Rawane rawout kenn té dou ray kenn dou wakh deugue bagoul serigne touba té limou wakh sounékone deugue lane lay wagni ci liguéyou serigne bi merci s mbaye gueye
@@thiawmansour8872 lol ki xolam none key moy fenal serigne bi Gni nangou wul diamu yalla teudj nagne seni negu yalla nek si lenene Ndar gay dem 1895 ga lathié kafa nagouwone diamu yalla
Allâh a dit : Allâh élèvera en degrés ceux d'entre vous qui auront cru et ceux qui auront reçu le savoir. Allâh est Parfaitement Connaisseur de ce que vous faites". [Sourate 58 : La discussion (Al-Mujadalah), Verset 11] Sounou Borom dafa yeuketi borom Xamxam, diokh ko thieur wou reuy. Mim Rëw, donio khepp borom Xamxam, ba noppi soufëlko. Ce pays va brûler. Croyez-moi. Ce n'est pas un souhait mais un constat de fait qui ne nécessite pas de longues explications. Nous faisons face à toutes les menaces. Le Sénégal de cette génération 2000, traverse des moments très difficile. Il vit aujourd'hui un terrorisme "fanatico-religieux" très dangereux, qui galope de plus en plus vers toutes sortes de chaos. Ce pays souffre. Le Sénégal est gravement malade. Sa maladie nécessite une prise en charge médicale d'urgence. Plus la maladie est grave, son état de santé se détériore de plus en plus vite et s'avére mortelle. Il est devenu un État où la science est réduite et l'ignorance renforcée dans les médias et autres canaux de transmission. Les intellectuels sont écartés hors du commun, laissant place aux ignorants, fanatiques... Actuellement, Rewmi tollouna foo khamni ken menetoul wakh ci Xamxam. Avant hier, c'était imam Moustapha Gueye, aujourd'hui Pr Rawane Mbaye très connu dans le monde musulman et arabe. Wãw, mim Rëw mom, bou démé ba borom Xamxam yepp noppi, foumou dieum ?
Naqaru Xol moo leen di ray rek Waaye Segam Tubaab bi moo Jém si Moom Tële Keneen du Mata Wax Jaajëf Syll Yalnala BOROOM TUUBAA gënë Kàttanal si Bàrkeb SIIDI BIRAAHIM FAAL YAARAM bi
Ayway noni serigne Touba Xadimour Rassoul yi naniou nopalou ko xani loko gueuneu taxal gueune ko toumaal ay soppeem diko gueuneu beugue diko gueuneu gueume Alahou Akbar ken dou Ahmadou baye mbaye dieureudieufati
MERCI MAESTRO LA RÉPLIQUE EST PERTINENTE. CEPENDANT, IL FAUT SE METTRE À L'ESPRIT QUE LE RÔLE DE LA OUMMAH MOURIDE EST DE FAIRE DES PRODUCTIONS OU DE VULGARISER LES ENSEIGNEMENTS DE SERIGNE TOUBA, AUTREMENT LES ENNEMIS FERONT DES COMMUNICATIONS SAUGRENUES. VOTRE CHAÎNE EST UNE CHAIRE UNIVERSITAIRE. SANTÉ ET LONGÉVITÉ. AMINE.
Man mi nga khamni maay taalibé bi gueuneu touti sakh khamnani wakhine wi dou wakhinou Serigne Touba ndakh mom Mossoul nangou kén nek bouureum koudoul yalla. C'est vraiment pas intelligent cette manigance. Nopalou leen . Jeureujeuf Sama baay Mbaye Gueye Syll khamalni beug nala trop nguir Serigne Touba sama yeené yeep moy guiss la un jour ❤❤❤
Rawane mbaye day thiakhane rek mais xaléyi xamul Serigne touba sax xam nanouné Serigne bii daawoul wakhéni😄😄😄...surtout dii nexal ay nasarane ak dii yereum talou. Yaw daal rawane mane na waatni amo been thieur si ya alla. Vraiment vous nous embêtez avec vos jalousies et accusations infondées. Nous n'avons aucun problème avec les confréries car le mouridisme est en quelque sorte la sélection et le regroupement de ceux qui veulent être les voisins de DIEU. Donc les autres ne sont pas mauvais mais ils sont aveugles et ils cherchent à nous montrer la défeance de BAMBA qu'ils n'en verront jamais. Nous vous prions vraiment de nous laisser à côté de Serigne touba khadimul Rassul. Bii thèse baxul dé et puis Napalene seen boop!!!😀😀
Ceux qui contestent ou détestent S Touba sont toujours de la même aubédience suivez mon regard.....le verdict est clair y'a t'il homme aussi populaire aussi aimé aussi charismatique aussi pieux et dévot que lui depuis que le prophète Mouhamed P S L nous a quitté.?Il est incontestable que non !! Quelqu'un a t'il écrit plus que lui mieux que lui parler la langue ouolof mieux que lui ? Amon humble avis il est l'héritier du prophète au sens spirituel du terme. Pourquoi toujours des doutes des suspicions des accusations infondées c'est plus que de la jalousie c'est de la méchanceté de l'animausité. Le seule maître du jeu et Allah il a donné le flambeau à Mouhamed psl qui l'a remis à S Touba n'en déplaise aux contestaires pseudointelectuels de tout bord
@@mouhamadulamiinmbacke8292 s abdou tontom ba dafko bind firi ko ci band yi yoron nako Wayé damako gnake. Sudè tontu s cheikhouna ak khadim sylla mom magui ak mom
Yaw goorgui ,khanaa daa am loo jappal rawane mbaye batakh nga beugkoo yakh AK dicko sossal ndakh linga wakh yeupp yalla takhoul yonneuntébi takhoul waayé sa bakane ,AK sa poche rek gnoo takh ngaye wakh , yaagui bejjaaw khamni mak nga lool Kone khallaatal yalla ci lingay wakh ,té baayi jakhassé Rawane AK askanwi ,julite dou naafekh té dou yéé fitna ...Yaw meunoo yakh Rawane Kone baayil soss té d'où Dara loudoul seytaané AK beug am am...Goorgui moomoo nitgni té moomoo Sénégal té boudoone DEUG sakh waroo ko fatali Di wouta Rawane ay noone...Segne Touba dantoula lii...kene santoula nga toontou Lou wessou 45ans ,seugam deugla sakh...yaw gueunoo gnoo gueum wolla beug Segne Touba ...Kone wakhal DEUG nguir yalla.loo khamlouneh amna koula ko gueuna kham...deungay uut ay clients rek pour sa chaîne bi Dong ...on a tout compris...ay vus rek ngay weur ci youtub ndakh nga am ay koppar .Kone baayil Rawane té yaw mag nga waayé yarou wooo... qu'est-ce qui nous dit que ce que tu viens de dire a été écrit par Rawane...kelle preuve ???? Yaa aaye goorgui té gnak yarr..yalla khamna lepp...
Rawane mbaye aka mana fene. Aka bagne serigne touba. Wallahi bala nga de danga khameni serigne touba amoul morom.
bay mbaye doundall 120 ans barkeb chiekh ahmadou bamba 🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Kii kayy doundam souniou fierté la🥰🥰😭
dieureudieufff serigne mbaye gueye ci leeeral yi,yaagaal weereul barkeep xassidas
Rawan yeureum na la
Allah hou Akbar
Tu ma beaucoup surpris monsieur.
A présent je ne peux vous appeller que monsieur
J'ai pitier de toi.
Kou nono mouride kou guis kanamam bouy wakh guakoy kham .dieuredieuf borom touba
Rawane rawout kenn té dou ray kenn dou wakh deugue bagoul serigne touba té limou wakh sounékone deugue lane lay wagni ci liguéyou serigne bi merci s mbaye gueye
Rawane mbaye mii ku bagne yonou Mouride la wayi du si am ndam fén rek la man Serigne touba nagou lén néko yalla déf mou nompal lén
Da ngaye doul rek pa bi moo bagne yoonou tidiane
@@thiawmansour8872louy beuz wakhi doff rek ngeni wakh
@@ndeyecodouthioune1193 ya meune tegal s ndeye pa bi key meussul bin lettre si yonou tidiane talouko sax dousi geustou
@@thiawmansour8872 lol ki xolam none key moy fenal serigne bi
Gni nangou wul diamu yalla teudj nagne seni negu yalla nek si lenene
Ndar gay dem 1895 ga lathié kafa nagouwone diamu yalla
Ahmadoul attekh yoyoooooo,gaagne nga goom déh👍👍👍
Waw goor baye mbaye magui nian yalla mo yagalla fi te andak wer amine
Chaque chose en son temps merci professeur Mbaye gueye Sylla pour ces éclaircissements on attend la suite avec impatience jerejeuf borom Touba
bay mbay gey silla yalnala yala fay thi barke serigne touba fa giaya moujdiou rék ley moujdiou raf ba diékh takk mbiroum serigne bi di gieuneu yeka tikou rék dieum kaw
Alhamdu lillaah ndeem léegi nangu nan ni sëriñ bi delsi na
Allâh a dit :
Allâh élèvera en degrés ceux d'entre vous qui auront cru et ceux qui auront reçu le savoir. Allâh est Parfaitement Connaisseur de ce que vous faites".
[Sourate 58 : La discussion (Al-Mujadalah), Verset 11]
Sounou Borom dafa yeuketi borom Xamxam, diokh ko thieur wou reuy.
Mim Rëw, donio khepp borom Xamxam, ba noppi soufëlko.
Ce pays va brûler. Croyez-moi. Ce n'est pas un souhait mais un constat de fait qui ne nécessite pas de longues explications. Nous faisons face à toutes les menaces. Le Sénégal de cette génération 2000, traverse des moments très difficile. Il vit aujourd'hui un terrorisme "fanatico-religieux" très dangereux, qui galope de plus en plus vers toutes sortes de chaos. Ce pays souffre. Le Sénégal est gravement malade. Sa maladie nécessite une prise en charge médicale d'urgence. Plus la maladie est grave, son état de santé se détériore de plus en plus vite et s'avére mortelle. Il est devenu un État où la science est réduite et l'ignorance renforcée dans les médias et autres canaux de transmission. Les intellectuels sont écartés hors du commun, laissant place aux ignorants, fanatiques... Actuellement, Rewmi tollouna foo khamni ken menetoul wakh ci Xamxam. Avant hier, c'était imam Moustapha Gueye, aujourd'hui Pr Rawane Mbaye très connu dans le monde musulman et arabe. Wãw, mim Rëw mom, bou démé ba borom Xamxam yepp noppi, foumou dieum ?
amatina sólo yalla na yalla fay la si barck serigne touba waw Goure mouride
Khawma lanla waye siwoul bariwoul bayre amoul khoram danaka kena khamoul bakham amna khamkham mom rawane
Dieuredieuf yallana la yalla fay si barkpe xassidayi alahouma amine 🤲🏾💯💞
Naqaru Xol moo leen di ray rek Waaye Segam Tubaab bi moo Jém si Moom Tële Keneen du Mata Wax
Jaajëf Syll Yalnala BOROOM TUUBAA gënë Kàttanal si Bàrkeb SIIDI BIRAAHIM FAAL YAARAM bi
wayé taloup serigne touba takkna té dotoul fay ba fawou nak
Manchalla yalla nga goudou fanne thi barkep serigne touba
KOU BAGÑ SERIGNE TOUBA
haaa DIGUA Am nakharou khol sa guirou DOUNDE té doko meuna safara . nagñiou DEUKÉ SANTE BA DÉ
Waaw goor nak kou meuna tontou pr RAWANE MBAYE si limou wakh warngha nou meuna tontoul EL MOUSSA CAMARA mi beugue kham Serigne TOUBA niata yone la diouli si Guedj Gui nakh wakhtou bou nek dafa wathj diouli yeegaat wala bene yone kasse la nionghi lay khaar si tontouli Serigne MBAYE GUEYE SILL dieureudieuf
Machallah baye mbaye gueye sylla yalla ngafi yage looll ta weer me kene moye rawane mbaye
Ameth fall ziar nala ,,tapeil tourame TH-cam tu verras bkp de choses sur lui,,,garouwalè la meune.
@@mouhamedthiam9048 machallah mane koko khamu mako
Dieureudieufe baye mbaye gueye syll yalla nala May fane wou goud té andak wérr
Dieuredieuf serigne mbaye
Nous attendons avec impatience la 2nde partie...INCHAA'ALLAH
Pér wakhofi dara
Dieureudieuf serigne mbaye kharal ma tèw lou
Waw goor macha allah lep rafetna diadieufati baye mbaye gueye sylla yalla ngafi yague lolll
Gnom d lignou bëgg dougnko am mouke serigne bi yalla ko yekati
Serigne mbay Guy syla yalnafi yague tewer
Bilahi kou bagne serigne Touba do am diam adouna ak allahira sokhore Di top ay narr ak ay nassarane
Naryi la segnebi don topou de loumou nar mokoko may
Ayway noni serigne Touba Xadimour Rassoul yi naniou nopalou ko xani loko gueuneu taxal gueune ko toumaal ay soppeem diko gueuneu beugue diko gueuneu gueume Alahou Akbar ken dou Ahmadou baye mbaye dieureudieufati
Dieureu dieufeuti serigne Touba
Rawane Mbaye dé kou bagn yoonou mouride la wayé nak dousi am ndam dousi am khol bou nékh.Gnifi nékone ak serigne bi nioko eupone ay pékhé fouff
Billay bëri në ñu nee mutt , wayé Seriñ bi rek la ñu bañ... Wayé " birassuman " rek ... ☝🏿
MERCI MAESTRO
LA RÉPLIQUE EST PERTINENTE.
CEPENDANT, IL FAUT SE METTRE À L'ESPRIT QUE LE RÔLE DE LA OUMMAH MOURIDE EST DE FAIRE DES PRODUCTIONS OU DE VULGARISER LES ENSEIGNEMENTS DE SERIGNE TOUBA, AUTREMENT LES ENNEMIS FERONT DES COMMUNICATIONS SAUGRENUES.
VOTRE CHAÎNE EST UNE CHAIRE UNIVERSITAIRE.
SANTÉ ET LONGÉVITÉ. AMINE.
Machalla serigne mbaye gueye yalla amna solo yalla ga fi yagu te wer loolololool
Dieurediefe serigne touba
Kou iniane d'où garame Mame ass
Sene serigne yapp bolene bole wone rawane Molène Mane wakhou ma woute katou khalis yi
Serigne bi, Yakh nga lepp, Ndakh mag dou sâga.
Wa mais damay lagne lanmo takh wà Sénégal bagne Serigne touba 😭 té Serigne touba limou déff thii diné béne mbindéff masoukou déff thii diné
Lo lougua yakare
Degay fene
Wa rawan moom moy kan ak wakhi wayadém yii rawan bamba d'où mass wasalam ❤️❤️❤️❤️❤️
Démlén diangui mo gueun ci yén ya rien de mal Rawane a dit que la vérité
Serigne Mbaye Gueye merci
Lima mana what moye kou doural serigne touba dingua rethiou adouna ak allakhira
Mais rawon seringe abdou rahman Mbacke darou mouhty tontou na rawan si kham kham
Ak s cheikhouna mbacké abdoul wadoud ak dr khadim sylla
Est-ce que vous avez des liens pour ces répliques
@@babacarndiaye8263 Tée ngaa Wax Lula woor
Le lien de la vidéo si elle est sur TH-cam svp
Man mi nga khamni maay taalibé bi gueuneu touti sakh khamnani wakhine wi dou wakhinou Serigne Touba ndakh mom Mossoul nangou kén nek bouureum koudoul yalla. C'est vraiment pas intelligent cette manigance. Nopalou leen .
Jeureujeuf Sama baay Mbaye Gueye Syll khamalni beug nala trop nguir Serigne Touba sama yeené yeep moy guiss la un jour ❤❤❤
Massa AHLLA
Pourtant c'est vrai ,la lettre en arabe ,je l'ai vu à l'ifan et chez la famille omarienne a Dakar.
@@deugrek4198 mdr yaw ya nexx dh kou neex nga massa massa way
Pabi dalle wakhoufi dra
wakhoul degue dh mome rawane
Jererjef s touba personne ne peut démolir le travail du grand marabout merci grand père
Igfm ay vrai franc maçon lane sou yabo ngéne nopal séne bopou si serigne Touba yalla moko yékati ta dotoul laal souf abadane
bilahi
Dieuredieuf serigne touba les jaloux vont mourir
Rawane wakhoul deug waye yalla nopina thi leep leepey leer dieureudieuf serigne touba
Dieureudieuf serigne touba sounou yakar téy ak euleuk
Jeureu jeuf serigne Mbaye gueye Syll yalla nala sounou borom yagal may LA werr
Kou bagne Serigne digua torokh adouna ak alakhira
Diere diefety seringe touba kouye dora mene kouye saga touba ca kanam wone nako
Dieuredieuf s mbaye
Machallah ❤️🙏💙 🙏
Rawane mbaye day thiakhane rek mais xaléyi xamul Serigne touba sax xam nanouné Serigne bii daawoul wakhéni😄😄😄...surtout dii nexal ay nasarane ak dii yereum talou. Yaw daal rawane mane na waatni amo been thieur si ya alla. Vraiment vous nous embêtez avec vos jalousies et accusations infondées. Nous n'avons aucun problème avec les confréries car le mouridisme est en quelque sorte la sélection et le regroupement de ceux qui veulent être les voisins de DIEU. Donc les autres ne sont pas mauvais mais ils sont aveugles et ils cherchent à nous montrer la défeance de BAMBA qu'ils n'en verront jamais. Nous vous prions vraiment de nous laisser à côté de Serigne touba khadimul Rassul. Bii thèse baxul dé et puis Napalene seen boop!!!😀😀
Merci Abdoulaye Diop waxbi rafete n'a dieuredieuf serigne Touba
Rawane c'est un anti_mouride c'est un aigri je me demande s'il est musulman ? Avec toute sa connaissance s'il ment ,"
Dieureudieufety serigne Mbaye Gueye syll
Serigne touba ak noune Mouride ba Ardiana
Diaradiuef serigne mbaye geuye silla yaw dall serigne touba mo lay faye
Père katieu gni nga wara leral si yonou mourite beurina dé niom gana ligni wah yeup si ay katieu doniou si dimbali
Sudé yagui bayi xel serigne ganna legui nga beg ko inchallah
Adama jouf,,,,geustoul tareqou islam reik dingua ham serigne bi loumou ame yala koko defal.ta gana limouy wah leip dagn ko binde.
Rawane Mbaye ak IGfm fén rék khawma Lou takh nitt gni ragalougn yalla léégi
Machala seringue mbaye selly
Vraiment la thèse de Boy rawane mbaye est incohérent avec la démarche de Serigne Bamba souniou yakar taye akk euleukk💓
Salamhalaykoum🙏🏽
Waw Mam Boye touma tontou bu ler rek mookoy dindi...
Kou doff tamite kou nitter mookoy tontou
Dieureudief Mam
rawane mbay doudou ma mbey kif kif thi leupou nak
Yalla nga fiii yang baye MbäYe Geuye ❤️🙏
Pa nexna dee amnga hamham amal diam
Dieureudieuf baye Mbaye
Dieureudieuf serigne touba rek mofi nek
MACHALLAH, âme na solo, l'UNe de mes chaînes préféré
Mane dal khawma loutakh niou bagne serigne touba
Sof ak jaloux molen diap
Rawane mbaye moustafa Gueye ngo bagne kadim
Demlen diangui mo guen nguen Nan da bagn segnebi sen leufeul nday way amrede nguen nitgni segnebi moye kan
Merci waay serigne bi
Dieureidief Baye mbaye
Khanaa khaloulen ni rawane Serigne bi rek la bagne. Ak yonwi. Souko nékhé sakh mou bagne ko. Santé mandouté mayou ko moukoy sossal
Diadieuf baye Mbaye Yalla nala Yalla takhawou
So begé dég deg tidiani tivaoune gnome dano yag bagne kou bax rawatina s touba
Mashallah
Baye mbaye niogui layy niann gua dem si wa igfm fa rawane mbaye waxe gua lerral ka fa dakh ayy yaxx katt lagne
Dieredieuf serigne mbaye Gueye syll Mouride sadikh Machallah
Dieuredieuf baye Mbaye Gueye Syll yague fii lool tee and ak werr
Dieuredieuf baye mbaye amna solo
Nous attendons la deuxième partie avec impatience
A1a1
Diaradiaf baay mbaye yagg fi loll taa wer ci barkep Serigne fallou mbacke Barakallahu feek
Kendou Serigne Touba
Grazie mille baye mbaye syll
Dieure dieuf s.mbaye gueye silla lér na nagn
Serigne bi rek laniou bagne wayé yalla doulenn may diameu deeee.
R mb dè s cheikhouna abdoul wadoud et dr khadim sylla et s abdou rahman mbacké tontu won nanko
Ceux qui contestent ou détestent S Touba sont toujours de la même aubédience suivez mon regard.....le verdict est clair y'a t'il homme aussi populaire aussi aimé aussi charismatique aussi pieux et dévot que lui depuis que le prophète Mouhamed P S L nous a quitté.?Il est incontestable que non !! Quelqu'un a t'il écrit plus que lui mieux que lui parler la langue ouolof mieux que lui ? Amon humble avis il est l'héritier du prophète au sens spirituel du terme. Pourquoi toujours des doutes des suspicions des accusations infondées c'est plus que de la jalousie c'est de la méchanceté de l'animausité. Le seule maître du jeu et Allah il a donné le flambeau à Mouhamed psl qui l'a remis à S Touba n'en déplaise aux contestaires pseudointelectuels de tout bord
Lien tontou bien ka sokhla
Tu n’as pas lu l’article, igfm a actualisé et diffusé dans le journal du 09 septembre 2020. Donc Mbaye Gueye fokk mou actualisé tontoubi.
Liens bi seringe Abdou Rahman tonto la bëgg
@@mouhamadulamiinmbacke8292 s abdou tontom ba dafko bind firi ko ci band yi yoron nako Wayé damako gnake.
Sudè tontu s cheikhouna ak khadim sylla mom magui ak mom
rawrane mbaye les mourides n'ont pas de leçons à recevoir de personne, serigne touba mbacke amoul moroome
Rawane nitou yalla là kou am kham kham kou mandou té kham dîné tédou wakhanto merci le professeur rawane mbaye longue vie à toi
Dieuredieuf serigne Bbay syll
Allahou Akbar thiéy cheikh akhmadou bamba mbacké khadimou Rassoul
Rawane mbaye dagay kathieu
Rawan kham kham so khamoul serigne touba amoul dieurigne
Rawane Mbaye Ya Mene FÈNE !
Diaradiaf way SERIGNE Mbaye gaeye
Machallah 👏👏👏👏👍
Ma yeureum kou bagne Serigne bi Senegal amou gnou bén djom rawane Mbaye souma féké wone thèse dinako wakh ya meune kathi domekharam
Rawane xawma kane del wakh lo kham ak loula woor nite da wara mandou di wakh deugue rawqtina lou dieum ci Serigne Touba
Nawax ci tarixaam moo gën moom Rawaan Mbay
Yèna dakha douleul tarikha diambour
MACHALLAH MOURID
Yaw goorgui ,khanaa daa am loo jappal rawane mbaye batakh nga beugkoo yakh AK dicko sossal ndakh linga wakh yeupp yalla takhoul yonneuntébi takhoul waayé sa bakane ,AK sa poche rek gnoo takh ngaye wakh , yaagui bejjaaw khamni mak nga lool Kone khallaatal yalla ci lingay wakh ,té baayi jakhassé Rawane AK askanwi ,julite dou naafekh té dou yéé fitna ...Yaw meunoo yakh Rawane Kone baayil soss té d'où Dara loudoul seytaané AK beug am am...Goorgui moomoo nitgni té moomoo Sénégal té boudoone DEUG sakh waroo ko fatali Di wouta Rawane ay noone...Segne Touba dantoula lii...kene santoula nga toontou Lou wessou 45ans ,seugam deugla sakh...yaw gueunoo gnoo gueum wolla beug Segne Touba ...Kone wakhal DEUG nguir yalla.loo khamlouneh amna koula ko gueuna kham...deungay uut ay clients rek pour sa chaîne bi Dong ...on a tout compris...ay vus rek ngay weur ci youtub ndakh nga am ay koppar .Kone baayil Rawane té yaw mag nga waayé yarou wooo... qu'est-ce qui nous dit que ce que tu viens de dire a été écrit par Rawane...kelle preuve ???? Yaa aaye goorgui té gnak yarr..yalla khamna lepp...
Jaajeuf nonni Serigne bi dougnou beek mouk
Dieuredieuf amna sollo matt naa léérall dééé
Jadieuffeti Baye mbaye Gueye syll