Au delà du mouridisme vous faites la fierté nationale de tout Sénégalais juste et intéressé par l’histoire de notre pays. Pour nous qui ont la chance de fréquenter les universités francophones et anglophones ; il y’a qu’au Sénégal que l’on écrit des livres d’histoire et des thèses sans se référer sur des documents authentiques. Baye Mbaye vous faites notre fierté
Tubaab yi daa na ñu jox Xaliss ay ñu ñuy tudde kilifë dinee ngir ñu xeex yoonu murit, te tay yoon wa ngi gën yokku , kon ay cë Baay Mbay liggéeyal Seriñ bi rek ✊🏿
أعمال خيرية lim wakh aka nek dagge touba rek guadol guis écoles tobab nione mourid yi si loxoy serigne bi lanio nek nekonio si loxol tobab ndakh danio indipandas si sono bopou gnio mom sonio deuk niomom sonio lepp
Serigne Touba dou moroom Gni serigne bi rek laniou bagn waye soon rekk nioom ak sen serigne si daniouy lambaatou te Khadim daffa dadj lou djitou Adama ak Awa
Le mouridisme a tjrs dérangé!! La mauvaise foi de rawane mbaye est manifeste. Mais nakk Bamba rekk. S il était collaborateur il ne serait jamais parti en exil. On connaît les collabo.
BAYE MBAYE topal gnou thèse bi de A à Z parce que wakh dji dafa wara lére. On est tous confronté à l'histoire de Seydou Wéllé qui pourrait constituer une grande plaie à la peau du mouridisme. J'étais sombré dans la colère et je n'avais plus de repère j'ai passé des jours et des nuits à pleur même s'il faisait minuit Grace à un homme comme vous je me suis tiré de mon trou Le problème en est que quand ils parlent, les nouvelles génération vont les croire de par leur cursus universitaires en disant "c'est un savant donc il a raison". Alors que c'est de l'histoire purement montée et orchestrée. Tous leurs objectifs, c'est de dénigrer le mouridisme juste pour protéger leur tarikha. Parce qu'ils savent bien que s'ils se taisent et/ou s'ils apprécient CHEIKHOUNA CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL (PSL) tout le Sénégal se transformera en royaume mouride. Ils œuvrent pour contraindre cela. On les comprend bien. Qu'ils aillent se faire foutre!
@@senegalndiaye1128 Seydou Wéllé béne talibé tidiane la bou bok thi famille sy yi aussi. dafa yékati wone ay touma you gnaaw ték ko thi serigne bi ak yone wi ta wakh dia gnep kham nane ni weroul. mais cachette yi mongui fi balégui gnoudi ko transmettre de génération en génération. ndakh mane guiss na khalé bou amoul sakh 17ans yorone ko thi téléphone. ta cachette bi lep ay sosse la. Baye MBAYE défone nathia ay léral you am solo.
Sa waay yaangui takh gni nga nakh ci ay sentiments gnouy saaga ap goor AP jambour bou gueunn yaw moomou té eupla khamkham ,guenn la jub guenn la maandou guenn la ragal yalla ,AK sa tougne yooyou Di melni tougou kouy toukh ndakh gnuulay ,moomoognou dengay djeema daané gaayi rek nguir Say poches waayé yalla takhoul yonneuntébi takhoul ,ay soss késsé AK Lou amoul benne firndé ,kene guissoul wolla degoul Rawane Di binde wolla Di wakh liingaye wakh ... yaangui takh gnoukoy saaga partout ,yaw yaa am problème AK Rawane té moola guenn waayé Rawane amoul benn problème AK kou teddkii Di Cheikhoul Khadim ...Kone limouy wakh dara douci DEUG wayé diakhassé rek AK seytaané AK noonou nitt beug gnou noonoooko ,yaw wakh nagne fi Lou gnaaw ci yonneuntébi Haleyhi Salaam té meusso wakh wolla def nga def Vidéo Kone nak arrête boooy mbaye Sylla...yaa guenna tuuti ci mourides , guenna doyadi ci makgni...deel wakh Lou am ndieurigne loolou lagnou sopp ci makk bou bedjaaw ténga baayi yingay djeuffandikoo...jangui Alkhour
Serigne Mbaye Gueye SYLL félicitation,je vous encourage car vous êtes en train de faire un excellent travail pour rétablir la vérité documentée.Sache que vous êtes en mission comme un choisi par Serigne Touba. Vos précisions sont toujours pertinentes et assumées. Cordialement.
Rewane mbaye.... serigne touba dousa moromou baye.. bagne serigne bi rek molene diap .diamoulene yalla bou bakh te kousi fatou te beuko serigne do tekhé
Wa Diou bakh néké lén fi nii rek Rawane mbaye mo leu eupe kham kham Rawane mbaye dou sa morom iow amo kham kham féne iow yako féke rawam mo lén eupe kham kham bayii lén togne pére wakho fii dara Sénégal dou gawa avance par par fén
Merci beaucoup machallah baye mbaye gueye sylla yalla ngafi yage ta weer ko bagne Serigne touba ape domou kharame nga ak komou mana don moye Serigne mba moye ab talibe point
Doundeul loubari bay booy chaque fois daniouy lal séen pékhe founè fougne Xam niogui Fay jaar guir beugue soféel mbiroum Serigne touba mais dou massa dialli warnagne la dalal wala nga bindi livre Serigne touba
Serigne Touba mbiroum Sounou Borom twt kou bagne nam ko def son am alkande lolou mo dal gnou rere gni agnane sokhor reuye rew ak gnak defarou ak gnak tawfekh
Bay mbaye weyal, liguèy bi bumu laal souf boul guèstou Yalla na Yalla samm leuh barki Alkhouranoul karimm🙏🏾
Macha Allah yow ak niom thiedo mouride, s abdou lahad bousso ak moustapha messere fierté guen si yobou mouride
Kou âme thieur thi yalla beug nga seugn Touba
Machallah yalla nala yalla samou si barkeb Serigne bi koubëgoull kola wédi Boull wax Lou weroull
Bou mbam yis weké na yatt wi dale baye mbaye dieredieuf👌
Wakhal dege waay mame bamba fane le déwé nékoll touba bayi lénne soupi dege
Astou Dieye nanal ndokh bakhna si xoll bou tang ❤️☺️
@@astoudieye8861 loula nakhari nak
@@cbonmoi3403 😅😅ki kay thi borom xõll you bon yi lë bokou
@@talibebamba5450 😅😅😅😅
Alhamdu lilah dieureudief s mbay Guy syla bunou la hamei
Yallnanga fu yague ta weir
Machaalah yallnala s bi fayal bopam❤️❤️
Serigne Mbaye geuye Sylla jerejef yaw yalla molay are ti barkeb serigne touba
Au delà du mouridisme vous faites la fierté nationale de tout Sénégalais juste et intéressé par l’histoire de notre pays.
Pour nous qui ont la chance de fréquenter les universités francophones et anglophones ; il y’a qu’au Sénégal que l’on écrit des livres d’histoire et des thèses sans se référer sur des documents authentiques.
Baye Mbaye vous faites notre fierté
Tubaab yi daa na ñu jox Xaliss ay ñu ñuy tudde kilifë dinee ngir ñu xeex yoonu murit, te tay yoon wa ngi gën yokku , kon ay cë Baay Mbay liggéeyal Seriñ bi rek ✊🏿
Jaajëf sëñ Mbay Géy Sill , Lii yàgg nafi Rawaan Mbay daa feeñ rekk ku bañ Sëñ Tuubaa ci aw naqar rekk lay dëkk .
Yalnala yalla faye serigne mbaye gueye sylle soldarou serigne touba
Yalnala yalla faye serigne mbaye gueye
Amine
Dieureudieuf Baye Mbaye Gueye.Lèp leerna nagn
Rawane mbaye lanmoy yonam ci yonou murid
Dieureudieufe mbaye
Khanaa jaloux rek. Serigne Touba rek la bagne
@@khadimesarr1968 en tout cas muene na togne loll bamouy bind kay manon na bind ci tarikha bimou bokou lolou moy mandou wayé li togne la
@@DAMEWADE93 bougnou moytouwoul Mbaye Gueye Syll Dina weerr séne serigne yi parce qu'il détient des archives explosives contre eux crois moi.
@@khadimesarr1968 je comprends pas ce que tu veux dire
Serigne touba boudonne nékhal toubab kone dou guenn rewmi gni nékhalone toubab nangoul toubab amou niouwone diafé diafé
Bayil doul del wax lo xam
Yaw yamal
@@abiboudiaw1936 kharitou toubap yi gnép khamnanouko espion bi dane diokhé informations khamnanouko
@@cheikhantangom1385 kaneuh leuh
Machallah yalla nagefi yague lol téwer amine
Machalla baye mbye soldarou borom touba
Rawane mbaye aka mana fene. Aka bagne serigne touba. Wallahi manonena binde deugeu thi serigne bi.
Baya Mbaye yalla guafi yague tewer na leppo ler rek Tidiane tivaoune yi paoul Mart AK tobab fene kat yi lagnio desse 😂😂😂
Dieuradieuf syll rawane Serigne touba du moromame bayame
Yalla nala yalla fay
Bialahi yaw rew rk 🙏🙏
dieureux dieuf seringue touba.seringe mbaye geuye Sylla yalna yalla goudal safane
Akassa Amna solo loll machallah dieureudieufeuty serigne touba Amoul morom🙏🙏🙏
Ma cha allah lérale by amna si solo
Gni da gnou mana sose
Dieredieuf s touba boudoul wone ak mome miogui si lokhoy toubabe yi
أعمال خيرية lim wakh aka nek dagge touba rek guadol guis écoles tobab nione mourid yi si loxoy serigne bi lanio nek nekonio si loxol tobab ndakh danio indipandas si sono bopou gnio mom sonio deuk niomom sonio lepp
@@lavieetpaix2358
😂😂😂😂😂 Serigne Bamba mo takh nekou niou aye yeufeur
@@juniorfaye7147
Touba amoul tabakh boufa tubabb def
Baye Mbaye Yalla nanga fi yaag te wer. Ndongoli Ahmadou Bamba Fall , Norvege.😭😭😭
Vous avez parfaitement raison Serigne mbaye GUEYE, wa alla, yenetibi et serigne touba geureum nanoula.
Serigne Touba dou moroom Gni serigne bi rek laniou bagn waye soon rekk nioom ak sen serigne si daniouy lambaatou te Khadim daffa dadj lou djitou Adama ak Awa
MaachAllaa Yalla nala Yalla dolee dimbali ci ligeey bi ci baarkeeb Seriñ Tuuba
Yae Yalla nala fay lingay def ben ligueyou serigne touba guenouko kawé bilahi ba autorité mouride yi gnongui lay diabalé rekk contane nanou si yae bou bakh bou wér
Une démonstration mathématique pure et rigoureuse !
Pas de commentaires !
جزاك الله عنا خير جزاءه ءامين زادك الله علما وحفظك من كل سوء
Dieureudieuféti Baye Mbaye Gueye Sylla, finga diape ,rék la Mbame yiye saga nake diarounio guérssou
Machalla serigne mbaye gueye yalla nala yalla faye boulen dek lu boulen falle yalla nala serigne touba fayal bopam niom ay noni serigne touba lane
Dieureudieuf ti leral bi. Bou mére, boul tayi. Niom li n'y déf dafay takh nioune ak Niom, n'y gueuna kham Serigne bi. Boul mére, Borom Bi mo léne di wakhlo ndakh niou gueuna kham Serigne bi.
Dieureudieufetii Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul 🙏🙏🙏
Le mouridisme a tjrs dérangé!! La mauvaise foi de rawane mbaye est manifeste. Mais nakk Bamba rekk. S il était collaborateur il ne serait jamais parti en exil. On connaît les collabo.
BAYE MBAYE topal gnou thèse bi de A à Z parce que wakh dji dafa wara lére. On est tous confronté à l'histoire de Seydou Wéllé qui pourrait constituer une grande plaie à la peau du mouridisme.
J'étais sombré dans la colère
et je n'avais plus de repère
j'ai passé des jours et des nuits
à pleur même s'il faisait minuit
Grace à un homme comme vous
je me suis tiré de mon trou
Le problème en est que quand ils parlent, les nouvelles génération vont les croire de par leur cursus universitaires en disant "c'est un savant donc il a raison". Alors que c'est de l'histoire purement montée et orchestrée. Tous leurs objectifs, c'est de dénigrer le mouridisme juste pour protéger leur tarikha. Parce qu'ils savent bien que s'ils se taisent et/ou s'ils apprécient CHEIKHOUNA CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOU RASSOUL (PSL) tout le Sénégal se transformera en royaume mouride. Ils œuvrent pour contraindre cela. On les comprend bien. Qu'ils aillent se faire foutre!
Kan mooy zaydu wélle waxal Wolof mu leer am na solo
@@senegalndiaye1128 Seydou Wéllé béne talibé tidiane la bou bok thi famille sy yi aussi. dafa yékati wone ay touma you gnaaw ték ko thi serigne bi ak yone wi ta wakh dia gnep kham nane ni weroul. mais cachette yi mongui fi balégui gnoudi ko transmettre de génération en génération. ndakh mane guiss na khalé bou amoul sakh 17ans yorone ko thi téléphone. ta cachette bi lep ay sosse la.
Baye MBAYE défone nathia ay léral you am solo.
Leur ptit fils dvindron tous des mouride je vous l'assure.
J'ais vue des cas comme ça
@@assanehanne2371 aka ler sah
Baye mbaye sant nanou la bou bakh ndakh li ngay déf askane bi gneup nga ko défal boul dég lou gnouy saga dano rerre té bougounou guindé kou
نحن نتابعك حتى وصلت هذا الموضوع اللهم حفظك ورعاك ببركة شيخ الخديم وجميع سلف صالح
Dieureudieuf sa baye YALLAH nala YALLAH Faye Barcke serigne TOUBA amine
Sa waay yaangui takh gni nga nakh ci ay sentiments gnouy saaga ap goor AP jambour bou gueunn yaw moomou té eupla khamkham ,guenn la jub guenn la maandou guenn la ragal yalla ,AK sa tougne yooyou Di melni tougou kouy toukh ndakh gnuulay ,moomoognou dengay djeema daané gaayi rek nguir Say poches waayé yalla takhoul yonneuntébi takhoul ,ay soss késsé AK Lou amoul benne firndé ,kene guissoul wolla degoul Rawane Di binde wolla Di wakh liingaye wakh ... yaangui takh gnoukoy saaga partout ,yaw yaa am problème AK Rawane té moola guenn waayé Rawane amoul benn problème AK kou teddkii Di Cheikhoul Khadim ...Kone limouy wakh dara douci DEUG wayé diakhassé rek AK seytaané AK noonou nitt beug gnou noonoooko ,yaw wakh nagne fi Lou gnaaw ci yonneuntébi Haleyhi Salaam té meusso wakh wolla def nga def Vidéo Kone nak arrête boooy mbaye Sylla...yaa guenna tuuti ci mourides , guenna doyadi ci makgni...deel wakh Lou am ndieurigne loolou lagnou sopp ci makk bou bedjaaw ténga baayi yingay djeuffandikoo...jangui Alkhour
Baye mbaye continuel sap liguey thi Serigne Touba ba ken thiose la wkhoumalak lall la kon Dinan guiss Lou graw
Dieureudieufeuti Serigne Touba XAAKAZA Baye Mbaye Gueye léral yi amatina solo
Dieuradiafati Baye Mbaye Syll Yalla nala Yalla defal Diamou ak khiwal ci barkep cheikh Moustapha al karem
Serigne Mbaye Gueye SYLL félicitation,je vous encourage car vous êtes en train de faire un excellent travail pour rétablir la vérité documentée.Sache que vous êtes en mission comme un choisi par Serigne Touba.
Vos précisions sont toujours pertinentes et assumées.
Cordialement.
Dieureudieufé Serigne Touba dieureudieufé Serigne Touba dieureudieufé Serigne
Dieurédieuf Baye Mbaye Syll
yalla na la yalla faye barakati Xassida yi
Yalla na yalla goudal sa fane barkep serigne touba 🙏🏿🙏🏿🙏🏿❤️❤️🕋🕋
Waaw góor jàmbaar, leerel yi am na solo lool jaajëf. Ñii seen xol yi du sedd mukk. قلوب من لم يحبوني على وجل ولايلاقون ماراموا ولاالبابا
Macha li mom dassiy bakh 💓🙏
S TOUBA amoul morome adouna ak alakhira
Ahmadou Bamba dieureudieuf ❤
diara diaf
Jerejef Baye Mbaye. Daniouye sonnou rek. Jerejef Serigne Touba Amoul morome jaaraamaa Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp Baaboul Mouridina
أيدك الله ونصرك ءامين
Rawaan déi mokou Tay lim mana wakh si Serigne touba si loubakh barina loutakh moy wakh si mom lou niaaw neu yatwi dall gnir Serigne touba rk
Machalla lii dafa diara leral amna solo serigne touba kene menouko touteul
ماشاء الله بارك الله فيك
Dieuredieuf Baye Mbaye Gueye Sylla.Que Allah vous une longue vie et une bonne santé. Merci beaucoup.
Dieureudieuf baye mbaye rawane serigne bi dou moromou mamam sakatouma bayam ignan rek al sokhor
waawaaw baye mbaye,mouride dou raggal dou arrière rawatina talibé BOROM DAOU MOUHTY
masallah santatinano bower Bay mbaye amnasolo
dieurediefe serigne touba khadimou rassoulilahi
Dieuredieuf Baye Mbaye Gueye Sylla.Que Dieu vous donne une bonne et longue vie. Moudj ak khewal.
Machala bou nite di diangue wakh demal diangui tonton ...Machala serigne Mbaye gueye sylla ...diambarou serigne Touba..yalnala serigne touba Faye.
Rewane mbaye.... serigne touba dousa moromou baye.. bagne serigne bi rek molene diap .diamoulene yalla bou bakh te kousi fatou te beuko serigne do tekhé
Bou mbam wekhe rek na yat wi dal amna solo bay Mbaye gueye syll
Rawan Mbaye dey dol rek defalol darrrra lislam
@@ousmangaye1687 SA Baye Laye katta ti toone
Wa Diou bakh néké lén fi nii rek Rawane mbaye mo leu eupe kham kham Rawane mbaye dou sa morom iow amo kham kham féne iow yako féke rawam mo lén eupe kham kham bayii lén togne pére wakho fii dara Sénégal dou gawa avance par par fén
Merci beaucoup machallah baye mbaye gueye sylla yalla ngafi yage ta weer ko bagne Serigne touba ape domou kharame nga ak komou mana don moye Serigne mba moye ab talibe point
Doundeul loubari bay booy chaque fois daniouy lal séen pékhe founè fougne Xam niogui Fay jaar guir beugue soféel mbiroum Serigne touba mais dou massa dialli warnagne la dalal wala nga bindi livre Serigne touba
Aminnne
Binde na si bou yagg dieuwrine
Diareudiauff serigne mbaye Gueye syll
Dire dief bay mbaye rawan dafa reer
Dieu reu dieuf borom touba amoul morom dh bilahi ☝️
Wallahi nonou Serigne Touba yi geuneu mak ci sénégal l'âne nek
Dieureudiaf s.mb.gueye rawan gfm sokhore monlene diap s.touba liko yalla Maye koumounekhoul sakhol moy meti
ماشاءالله جزاك الله خيرا
Machalla serigne bi🙏❤️❤️serigne touba rk mofi né
Rawan mbaye tounouque ndayame
Machallah ❤️🙏💛🙏❤️
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye gniguilay sante yalnala Serigne Touba Faye
yala nala serigne touba dougale si bir carangem sagou yonwinga
yalla na yalla fay la ta samla si barck serigne touba
Di sante Sérigne bi bou bakha bakh❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
جزاك الله خيرا
Jërëjëf sëriñ Mbay Gëy Silla Yàlla Na yàlla Goudal fan Wi ci barkëb boroom Tuubaa rawaan Mbay xol buy metti la nara dëggee ba ba muy faatu
Baay Mbay jërëjëf, bég nanu ci yaw.
Jeureu jeuf serigne Mbaye gueye Syll yalla Ngah am geureumul serigne Touba barke borom Darou mohty
Dieureudieufetty baye MBAYE fann wougoudou lool andak weer
Dieureudieufeti serign mbaye gueye silla
Dieureudieufaty s mbaye Gueye yaw serigne touba molay liguéylo kokou mbaye ak gnikoy layal saitané lagniy liguéyal niom takou niou dara tékoki wougne dara dougne touss
Mashalla papeu.leraal yi amna solo.
dieuredieuf s.touba dieuredieuf segn mbaye gueye sill ndok yalla mbanga guestoo bou bah si serigne bou makkk bi
Walahi biu tit dé am toubabe bi moko def jereujefé SERIGNE TOUBA
Yal na la Yàlla sàmmu te aar la, doxal bu la kenn laal noo ngi sa ginnaaw.
Baye mbaye sylla gnioun aye ndawî mourid lan yaw lan begue yaw lan xam yaw lan ték si sounou kanam pour khékh noni seringe touba yi
Dieureudieuf serigne tuoba
deradief.deg.dyeleer.kounafekhl.faga.dielee.lee.manonnafa.dieleli.daredef.mbaye.khul.aatou.bourhanakumu.inkuntum.sadikhina
Serigne Touba mbiroum Sounou Borom twt kou bagne nam ko def son am alkande lolou mo dal gnou rere gni agnane sokhor reuye rew ak gnak defarou ak gnak tawfekh
أيدك الله ونصرك وزادك علما
Dieureudieuf baye mbaye amall diamou diou beuri si barki borom touba
waw gorr..baye m sylla....mbam bu wekhe na yatwidal..ci ker nopibi..,aksa
Jajeuf sylla yaag fi te veer
Yala nala yala werall boy mbay