Nous sommes plus de 30000 Abonnés certes que ya n'a qui savent pas lire. Mais je demande à tout un chacun qui félicite le beau travail que mène notre père Mbaye Gueye Sylla est d'acheter le livre qu'il a écrit sur la fin des ennemid de Serigne Touba. Ceci est une geste qui peut l'aider à pouvoir améliorer plus de recherche sur l'histoire de Serigne Touba Nassi mouride yeup diape
Man de bitim rew bi ma nek toubayi dano fonk seni diambar waye Senegal nguay guis gnouy weddi seni diambar serigne touba Ken la waye khamnani bounguen manona efase djioulik ndargua ak djioulik guegui di nguenko def waye di nguen dee seni khol di boon yen gnikoy critigue te dou guen si man dara inchalla dieureudieufati serigne touba
Les sénégalais sont des mécréants mais il faut reconnaître que Serigne Touba moyy sounou Ndame walahi nioune mome borom Touba rekk laniou Ame dieuredieuf baye Mbaye Gueye Syll je suis de Paris magui laye begueee bou werr yalla nala borom Touba fayaal boopamm
Le seul intérêt de leur répondre est de préserver l'histoire de Serigne Touba pour les générations à venir. On ne sait plus leur motivation. Ils sont dans leur aigreur. Ils ne veulent pas accorder un millilitre de sainteté à Serigne Touba et n'hésitent pas à contester chaque étape de son histoire. Nous, les mourides, avons signé un pacte à allégeance avec Khadim Rassoul. Rien ne nous fera tergiverser et on sera de plus en plus nombreux et de plus en plus dévoués à Cheikh Ahmadou Bamba
Merci MBAYE Gueye Syll , la chance de la communauté mourite en cette période, c'est de disposer de grand uridits capables de défaire tous les "cathiii" des pseudos intellectuels bounty. Dieureudieuf Serigne touba Diarama Cheikh Libre Lamp !!!!!
Macha Allah amatina solo. Ma diambal bi waxone ( touba & mbacké laxe du mal) ndioxone gako walam si mboldé yi mome ak niou melni mome. Ma diambal, el modou geuye, elh Ndiaye, zahra iyane thiam ak guett gogou. Dama beugue gua deff live lathie lén 5 millions yi dadjé wone si magal ta kén coronawoul loutakh waxounioussi ak journalistes nafek yeup manam guett gui rek taye béne mbam yokna si guett gui
S’il y’a une chose dont sont unanimes tous ceux qui ont côtoyé le cheikh: c’est le fait que dès qu’il arrive dans un lieu il y fait d’abord la prière ( les témoignages des mauritaniens l’attestent ) donc qu’il prie dans le bureau du gouverneur est juste la suite logique de son trajet depuis Djéwol où malgré l’escorte des colons, descendait prier à chaque heure de prière. Merci beaucoup pere certains sénégalais temps yi Serigne bi lagn dieul dale ohhh walahi danio xamoul .. Qu’Allah nous guide et nous assiste
Baye Mbaye walahi amagal niou ndiarigne boofi néékoul woon dina niààw yalla na yalla yokkou sa takhawaay barké borom Touba yonnu Mouride dougnla faaté ti ameel nagnla ndioukëul bu baax
Je cité quelqu'un " quand le noir cessera réduire le noir , le noir comptera au banquet du donner et du recevoir . La question qui mérite d'être posée est celle ci : pourquoi Cheikh Ahmadou Bamba a été le seul Marabout combattu , exilé et assigné à résidence jusqu'à la fin de sa vie , soient 32 ans de son existence , et pas les autres ? Le bavardage ne prendra jamais le dessus sur les bonnes œuvres ou actions .
Seules l'honnêteté et l'objectivité guident notre réflexion et démarche , en dehors du fait d'être un Musulman tout simplement . Tout être qui contribue ou concourre à l'existence de cette foi et croyance mérite notre respect et nos hommages . QU 'ALLAH magnifie Cheikh Ahmadou Bamba et ses œuvres .
Kii khamoul dara té mandouwoul téyoul wayé melnani sopoul sergne touba wayé diganté serigne bi ak toubabyi leerna yawnak yalla molay fay ci barkeb serigne bi ak borom darou mom nak amoul diom fenn na fenn wou reuy
Merci Serigne mbaye vous faites la fierté de tous les disciples de mawlana cheikh Ahmed bamba khadimou rasouloul lahi Salla Allahou aleyhi wa sallam que allah le tous miséricorde vous protège
machallah mai amna gno khamne leup lognou amm serigne touba mo takh te leup lognou wakh serigne bi dafa melne dolen meti talibe yi rek gnom la serigne bi diaral sene bakane
Jerejefeti Baye Mbaye lii amno solo je viens de regarder la vidéo et c tard mais je suis vraiment content de vous et longue vie à vous et toute la famille merci
En faite moi j ai écouté Mame Maram seck dans l émission impression de Sada kane mais j ai l impression qu il a juste confondue les prieres entre le bureau du gouverneur et la priere au port ou le marabout a recite sourat bahara et Ali Imrane mais il n a pas nie la priere autre chose il a meme parle d une histoire racontée par serigne saliou c etait tres intressant
Nous sommes plus de 30000 Abonnés certes que ya n'a qui savent pas lire. Mais je demande à tout un chacun qui félicite le beau travail que mène notre père Mbaye Gueye Sylla est d'acheter le livre qu'il a écrit sur la fin des ennemid de Serigne Touba.
Ceci est une geste qui peut l'aider à pouvoir améliorer plus de recherche sur l'histoire de Serigne Touba
Nassi mouride yeup diape
Ndeyssane sougnou Baye Mbaye gueye Syll mane Dal ma ngui niane sa fane wi doon keemaan. Yaaaaaag fi lole ak wer ak werlé
Amiin
@@doomixalemag1085 Amine barké seringe touba
@@sidylo9069 abdourahmane touba schio italia
Man de bitim rew bi ma nek toubayi dano fonk seni diambar waye Senegal nguay guis gnouy weddi seni diambar serigne touba Ken la waye khamnani bounguen manona efase djioulik ndargua ak djioulik guegui di nguenko def waye di nguen dee seni khol di boon yen gnikoy critigue te dou guen si man dara inchalla dieureudieufati serigne touba
Dueredieuf serigne touba
Walahi hasim lou lere nga wakh toubab yi de aka non fonkou seni mame seni jaloré wayye Senegal ki nou geuna bagne thi Adouna moy Serigne touba
Sénégalais bougoul Lou bahh ndahh sohorrr..
ki dal moy doméram rek may wakh mouy rouler ay rrrrrr...yaw demal diangui....mom sakh fane la toth?
Ndeyssane baye mbaye da beugue serigne touba ba diekhe takk
Bilahi papa mane nimala baguë ❤️❤️sakhe dafma diakhale sopou Nala torop baye Mbaye Gueye
Merci bcp baye Mbaye ki boulko wakh sëriñ bi wakh ko fénnkatbi
Même les vidéos de baye mbaye Gueye syll doit être archivée.
Les sénégalais sont des mécréants mais il faut reconnaître que Serigne Touba moyy sounou Ndame walahi nioune mome borom Touba rekk laniou Ame dieuredieuf baye Mbaye Gueye Syll je suis de Paris magui laye begueee bou werr yalla nala borom Touba fayaal boopamm
Diajef BAYE mbaye kii do touko dolli dè yallna nou layalla fayall si barkep borom darou moukhty
Merci encore une fois de vos contributions. Je pense qu'il serait bon de trouver une emmission avec Sada Kane dans la même tv
Le seul intérêt de leur répondre est de préserver l'histoire de Serigne Touba pour les générations à venir. On ne sait plus leur motivation. Ils sont dans leur aigreur. Ils ne veulent pas accorder un millilitre de sainteté à Serigne Touba et n'hésitent pas à contester chaque étape de son histoire. Nous, les mourides, avons signé un pacte à allégeance avec Khadim Rassoul. Rien ne nous fera tergiverser et on sera de plus en plus nombreux et de plus en plus dévoués à Cheikh Ahmadou Bamba
Très bien der MB g
Malaco wax dhé
S.mbaye.Sylla Yalla na la S.Touba Faye Yalla nga yague sounu kanam AmINE.,.
ManshALLAH longue vie tonton mbaye gueye sa liguey amna solo torope
Dieureudieuf yalla na yalla fayla ci ligey bou am solo bi ngay deg ci yonou mouride, fonk nala naw nala t walahi beug nala torop,
Merci beaucoup pape
Yallana fi sakh s barrkepp serigne Bi
Merci MBAYE Gueye Syll , la chance de la communauté mourite en cette période, c'est de disposer de grand uridits capables de défaire tous les "cathiii" des pseudos intellectuels bounty. Dieureudieuf Serigne touba Diarama Cheikh Libre Lamp !!!!!
Dieuredieuf serigne Mbaye gueye sella yalla nagefi yague lol the wér si barkpe xassidayi alahouma amine 🤲🏾❤💯💞
Merci père mbaye gueye sill
Bilaye père wakho fii dara ki li mou dara nékou si ragalal yalla
Boudoon sa baye la, di nga wakh wakhoo fi Dara démal diaangi nahju
Grazie mille serigne Mbaye Gueye
Dieuredieuf baye Mbaye Gueye Syll yalla ga fii yague lool tee and ak werr kenne dou borom Touba merci à vous encore une fois
yalla na yalla fay la waw Goure mouride amatina sólo Machallah
Macha Allah amatina solo. Ma diambal bi waxone ( touba & mbacké laxe du mal) ndioxone gako walam si mboldé yi mome ak niou melni mome. Ma diambal, el modou geuye, elh Ndiaye, zahra iyane thiam ak guett gogou. Dama beugue gua deff live lathie lén 5 millions yi dadjé wone si magal ta kén coronawoul loutakh waxounioussi ak journalistes nafek yeup manam guett gui rek taye béne mbam yokna si guett gui
Jërëjëf Syll yalna saa Boroom fay
Ndeye sane baye mbaye yalla nagua fi yague si barckè borom touba
Merci beaucoup Serigne Mbaye gueye syll
Dieuruedieuf baye mbaye yalna yalla gouddal sa fane
Gnoun déh serigne touba rék lan beug mom rék lan kham
Dieureudieufé Serigne Touba
S’il y’a une chose dont sont unanimes tous ceux qui ont côtoyé le cheikh: c’est le fait que dès qu’il arrive dans un lieu il y fait d’abord la prière ( les témoignages des mauritaniens l’attestent ) donc qu’il prie dans le bureau du gouverneur est juste la suite logique de son trajet depuis Djéwol où malgré l’escorte des colons, descendait prier à chaque heure de prière.
Merci beaucoup pere certains sénégalais temps yi Serigne bi lagn dieul dale ohhh walahi danio xamoul ..
Qu’Allah nous guide et nous assiste
Kou bégn Serigne Touba dinga dé tabbi safara
Machallah ♥️♥️👏👏
Serigne touba amol morom bilaye diarra ma baye mbaye Gueye sylla
dieureudieuf serigne touba ♥♥♥♥♥
Dieuredieuf Baye Mbaye Syll ,yalna yalla fayla ci barké Borome Touba.
Dieureudieufeti serign mbaye gueye silla sa liguéye raféte na machalla
Machallah bay Mbaye Guéye vraiment c'est une pertinente réponse.
Baye Mbaye walahi amagal niou ndiarigne boofi néékoul woon dina niààw yalla na yalla yokkou sa takhawaay barké borom Touba yonnu Mouride dougnla faaté ti ameel nagnla ndioukëul bu baax
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Sylla. Yalneu leu Cheikhoul Khaddim fay.
Machalla dieureu dieuf s mbaye gueye yala nala sama borom fay
ماشاءالله
جزاك الله خيرًا
Merci serigne mbaye gueye
Jerejef baye mbaye gueye
Ma challahou amna solo lol yalla nala yalla defal lepo lo beug si bark al quran karim
Merci baye Mbaye, encor une fois dano sokhor thé niakk diom rek
Khadim rassaul dou sén moromou serigne, lini bagna dégg!
Wakh dëugeu yalla
Dieredieuf Serigne mbaye Gueye syll Mourid saadikh deug rek inchallah Dieredieuf Serigne Touba.
Merci Sr. mbaye mba wèkhe rek lay dèwale
Je cité quelqu'un " quand le noir cessera réduire le noir , le noir comptera au banquet du donner et du recevoir . La question qui mérite d'être posée est celle ci : pourquoi Cheikh Ahmadou Bamba a été le seul Marabout combattu , exilé et assigné à résidence jusqu'à la fin de sa vie , soient 32 ans de son existence , et pas les autres ? Le bavardage ne prendra jamais le dessus sur les bonnes œuvres ou actions .
Dia duef per
Akassa lérna dé
Seules l'honnêteté et l'objectivité guident notre réflexion et démarche , en dehors du fait d'être un Musulman tout simplement . Tout être qui contribue ou concourre à l'existence de cette foi et croyance mérite notre respect et nos hommages . QU 'ALLAH magnifie Cheikh Ahmadou Bamba et ses œuvres .
Machallaa baye mbaye geye
Jerejef yague fi teh werr lool barkep borom touba❤❤❤❤❤
DIADIEUFATI BAYE MBAYE YAGAL WÈRAL THI DOUNYA ❤❤❤
Dieureudieuf serigne touba yalla na ngua goudou fane ak werrr
Chaque jour dal ak none boubess Dieuredieuf Baye Mbaye
Merci père nous sommes avec toi
Kii khamoul dara té mandouwoul téyoul wayé melnani sopoul sergne touba wayé diganté serigne bi ak toubabyi leerna yawnak yalla molay fay ci barkeb serigne bi ak borom darou mom nak amoul diom fenn na fenn wou reuy
Dieureu dieuff yalla na la yalla Faye te musalla thi saytané mayla mudj gou rafett
Machallah syll
بارك الله ممتاز
Merci Serigne mbaye vous faites la fierté de tous les disciples de mawlana cheikh Ahmed bamba khadimou rasouloul lahi Salla Allahou aleyhi wa sallam que allah le tous miséricorde vous protège
Dieureudieuf serigne TOUBA
نصركم الله وأيدكم
Dia d'oeuf baye mbaye Gueye Sylla yalna yalla goudao Say fane weral Say thieur
ماشاءالله الله يبارك فيكم
Dieuredieuf mbacke
Ma seck fenne rek wayyé serigne touba ammoul morrom
Séng bi seck méw rek ngay def😀😀
yalnala yalla fay rek s touba kase ❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️
Machallah
machalla
Merci 👍 👍
Yalna sa fane wii goudou lolllllllle téé gua wérr barké xassida
Machallah yaguefi lole té wer
Ñii ay mbaam lan rek fen rek Lani def boo waxee ñuy tubaab tubaab lu tekki wun dara nitt yu yees lan yu bon ay xadie sax moo leen gën
Nalla yalla dèfalll Tawféx
Serigne Touba doit être un honneur pour tout musulman du monde entier. On doit en être orgueilleux
Dieureudieufety serigne Mbaye Gueye syll dieureudieufety
Alhamdoulilah
Serigne mbaye Gueye sylla amna solo
Machalah amna solo
Assalamou aleykoum wa rahmatou LAHI. Mangi dagaan YALLA ci barkeb BOROM TOUBA YALLA defal ngërëmmal BOROM TOUBA.
Je suis fier de serigne touba
Nit bouy diéma yakhal serigne touba billahi day takh tityi diko geunna beug rek
Mercebaye
machallah mai amna gno khamne leup lognou amm serigne touba mo takh te leup lognou wakh serigne bi dafa melne dolen meti talibe yi rek gnom la serigne bi diaral sene bakane
Jerejefeti Baye Mbaye lii amno solo je viens de regarder la vidéo et c tard mais je suis vraiment content de vous et longue vie à vous et toute la famille merci
Baye Yalla nala yalla faye
En faite moi j ai écouté Mame Maram seck dans l émission impression de Sada kane mais j ai l impression qu il a juste confondue les prieres entre le bureau du gouverneur et la priere au port ou le marabout a recite sourat bahara et Ali Imrane mais il n a pas nie la priere autre chose il a meme parle d une histoire racontée par serigne saliou c etait tres intressant
Machalla lerna yalla na yalla yako wergui
Maa chaa alla sama bay mbaye Gueye sylla omar dp Brasil yakar brom darou al moukhty
Yalla nga fi yagg lol tawèr
Kėne dou serigne touba
Jeter.seringe.bi.yalla.nala.yalla.fey
Gni nèkou niou sunu ay ndawlè limata xam moy kène Indi woufi lou geune wèr lim fi Indi kon naniou doy seuk🙏
Xam sam reew tv mo am sollo lolle thi yonou mourite wi tv numero 1 na nieepou abonnè
Dieuredieufeti bay mbaye yalla nagafi yag
Sernge mbay guey sella diardiuf yall yall fay ak Sernge touba me boo ma baleine toti nga bay wakhe khawa teguine ndakhe Serge touba lepam ay teguine laa ame dangay fenne s touba daco aye si terr bouna nahdjou yamaco guina xame
Al hamdoulilahi bagnou ame kou melne Yaw ame kham di wakh ak des documents en main God bless you🙏
Bayil cheikh omar diagne bi ngaye garou walé dousa morome
Tatou ndayou omar diagne ak yaw
Baye mbaye nogui khar sa vidéo ci linu def police talibe serigne modou kara bi comme niga ko dan defe bounu lale lou bokou ci yon wi dieuredieuf
Serigne mbaye Gueye Sylla jerejef