Diagne député : Il se présente dans la circonscription des « Quatre communes » du Sénégal (St-Louis, Rufisque, Dakar et Gorée) qui jouissent d’un statut spécial unique dans l’empire colonial africain de la France. Ce statut confère à leurs habitants la possibilité de voter lors des élections : ils peuvent élire des conseillers municipaux et un député. Le gagnant des élections législatives représente les quatre communes au palais Bourbon. Diagne part avec un désavantage car est inconnu de la plupart de ses électeurs (il a quitté le pays en 1892). Il bénéficie néanmoins du soutien de Galandou Diouf, un africain membre du conseil général qui s’est fait remarquer par ses prises de position hostiles à l’administration. Il est aussi soutenu par Cheikh Amadou Bamba, le chef de la communauté Mouride. Il est également appuyé par Assane Ndoye, un des chefs de la communauté Lébou dont le soutien compense son manque de notoriété. Enfin, il est épaulé par Amadou Duguaye Cledor qui restera un fidèle parmi les fidèles. Diagne cristallise les espoirs d’une génération qui rêve de se voir représenter par un Noir au palais
Borom Touba lepam da fa ler. Merci Serigne Syll de continuer à éclaircir. Mais ne te mets pas en colère en apportant des réponses. Apportes la science et Allah fera le reste
Merci baye Mbaye heureusement que vous êtes là . Il faudrait qu’on sache que nous ne sommes plus à l’époque coloniale pendant laquelle nous avions personne pour défendre la cause du mouridisme devant ces soi disant patriote prêts à tout pour satisfaire leur maître Je longue vie et santé de fer vous faites la fierté de toute la nation sénégalaise qui aspire à une indépendance au vrai sens du terme. Merci...................mille fois Nous attendons que votre livre arrive en France
Blaise Adolphe Diagne est né le 13 octobre 1872 sur l’île de Gorée. Il est d’ascendance lebou et wolof. Fils de Niokhor, un Sérère de Gorée qui était marin-cuisinier, et Gnagna Preira, une mandjaque originaire de Guinée-Bissau, Blaise Diagne, naît Gaiaye M’Baye Diagne. Il est très tôt adopté par la famille Crespin, une famille respectée de métis originaires de Gorée et de St-Louis. C’est son père adoptif, Adolphe Crespin, qui lui donnera le prénom de Blaise. Il apprend très tôt à lire et à écrire, bénéficie d’une éducation solide qui s’appuie sur d’incontestables qualités intellectuelles. Il étudie à l’école des frères de Gorée, puis à l’école laïque de St-Louis. Il figure ainsi au palmarès de la distribution des prix de l’école laïque de Saint-Louis en août 1884. Boursier du gouvernement, il va poursuivre ses études en France, à Aix-en-Provence. Malade, il revient poursuivre ses études à l’école secondaire des frères de Ploërmel (ou de Duval) puis prépare en 1891 le concours d’entrée dans la fonction publique au service des Douanes où les places réservées aux Africains sont assez peu nombreuses à l’époque. Blaise Diagne se marie avec Marie Odette Villain. Ils auront quatre enfants dont Adolphe, médecin militaire, Rolland, fonctionnaire dans les Chemins de fer et Raoul, footballeur professionnel et le premier footballeur africain à être sélectionné en équipe de France
Baye mbaye Yale na yalla goudal sa fan mane dh aférou soldar yoyou diaxalon na ma lol ndakh bounou né Serigne touba mo diokh Toubab yii aÿ soldar pour mou khéxale lén mane mom diaxalon nama lol wakh dëgue yalla wayé tayy mom ler na si mane yale nalla yalla faye barekéb borom touba cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul
Tonton Mbaye sylla tous les musulmans particuliers les morides moi personnellement un grand merci s'il y avait d'autre comme vous ki nous dépend personne n va plus toucher à notre l'islam ( mourite)encore un grand merci
Jërëjëfëti Baay MBaaye Guèye Syll , yaw daal Yàllah në ngë guddu aw fan te and ak wèr, lègui laa la doon setaan Sen TV , begg na ñu lol ci yaw maachAllah.
Baye Mbaye Gueye SYLL. Jërëjëf. Yàgg naa laa topp waye tay lay sooga artu ci sa xët wi. Waye ku bëgg yoon wi rek ameel na la "jaajëf". Li ngay leeral amna solo. Yaa ngi làqqarci fen yu nu yagga ràbb ( lu tollu ci xarnu daanaka). Je voudrais vous suggérer de créer un site de vérification des informations touchant à la Mouridiyah et à son fondateur, genre "Mouridiyah fact-check". Je sens que vous avez par devers vous beaucoup de connaissances et de documents de sources sûres. Et nous sommes à l'ère de l'information et de la communication et les forces du mal font la guerre avec. Nous savons que rien ne peut entacher ni diminuer l'aura et la précellence de Serigne Touba, néanmoins un tel site pourrait constituer un puissant outil pour démasquer les calomniateurs tapis dans l'ombre.
Mame Boye wakhal. Yaw lagniy sago. Nous sommes très heureux de vous pour les réponses que vous apportez à ces mécréants et ennemis du mouridisme. Merci beaucoup.
Dueiradieuf serigne mbaye sylle yalla nala serigne bi fayal bopam wayé yonou mourid koufi wakha lodoul deugu da niou la wara fèkk fa nga nèk dèf ko lo bone lolou rék moy takha niou nopé
thieuy serigne mbaye gueye syll nioun mouride yépp amélnanla ndioukeul yalnala yalla fayal bopam thi barké serigne touba
Merci baye mbaye yageu fi rek Té weur lingaye def amna solo lool
Amine
Diagne député :
Il se présente dans la circonscription des « Quatre communes » du Sénégal (St-Louis, Rufisque, Dakar et Gorée) qui jouissent d’un statut spécial unique dans l’empire colonial africain de la France. Ce statut confère à leurs habitants la possibilité de voter lors des élections : ils peuvent élire des conseillers municipaux et un député. Le gagnant des élections législatives représente les quatre communes au palais Bourbon.
Diagne part avec un désavantage car est inconnu de la plupart de ses électeurs (il a quitté le pays en 1892).
Il bénéficie néanmoins du soutien de Galandou Diouf, un africain membre du conseil général qui s’est fait remarquer par ses prises de position hostiles à l’administration.
Il est aussi soutenu par Cheikh Amadou Bamba, le chef de la communauté Mouride. Il est également appuyé par Assane Ndoye, un des chefs de la communauté Lébou dont le soutien compense son manque de notoriété.
Enfin, il est épaulé par Amadou Duguaye Cledor qui restera un fidèle parmi les fidèles. Diagne cristallise les espoirs d’une génération qui rêve de se voir représenter par un Noir au palais
Jërëjëfëti serigne Mbaye Gueye Syll. Yalnala sëriñ bi fayy lu baree bari.
Dieureudieuf Sëñ Mbaye. Vous nous êtes d’une aide très précieuse
Jambarrii serigne touba khadim Rassoul .
Yalla nalla serigne bii taxawou
Ayyy Alioune tine ci werou korr lagnou nek serigne touba sokhlawoul ndimbalou keneu koudoul bour yalla ak yonnentem ba
Merci père dokhalal serigne touba la nior yaw diamou ngaye ame
Dieureudieufati tonton syll . Bouleenkenna fatta walhal ndakh yaye baatii Mouride yeuppa . Dieureudieuf tonton heureusement ngua nekkafi goudda Fann ak wergou yaram ak ndiabbot bou Karel
Machalla serigne mbaye gueye syll mano fi niak Bilay yalla nala yalla faye si b touba
Borom Touba lepam da fa ler. Merci Serigne Syll de continuer à éclaircir.
Mais ne te mets pas en colère en apportant des réponses. Apportes la science et Allah fera le reste
Merci baye Mbaye heureusement que vous êtes là .
Il faudrait qu’on sache que nous ne sommes plus à l’époque coloniale pendant laquelle nous avions personne pour défendre la cause du mouridisme devant ces soi disant patriote prêts à tout pour satisfaire leur maître
Je longue vie et santé de fer vous faites la fierté de toute la nation sénégalaise qui aspire à une indépendance au vrai sens du terme.
Merci...................mille fois
Nous attendons que votre livre arrive en France
Dieureudieuf lerr na nagn doundeul way yal nga fi yagu té wer barké Borom Touba. Yoon wi sokhla nala plus k jamais
Blaise Adolphe Diagne est né le 13 octobre 1872 sur l’île de Gorée. Il est d’ascendance lebou et wolof. Fils de Niokhor, un Sérère de Gorée qui était marin-cuisinier, et Gnagna Preira, une mandjaque originaire de Guinée-Bissau, Blaise Diagne, naît Gaiaye M’Baye Diagne. Il est très tôt adopté par la famille Crespin, une famille respectée de métis originaires de Gorée et de St-Louis. C’est son père adoptif, Adolphe Crespin, qui lui donnera le prénom de Blaise.
Il apprend très tôt à lire et à écrire, bénéficie d’une éducation solide qui s’appuie sur d’incontestables qualités intellectuelles. Il étudie à l’école des frères de Gorée, puis à l’école laïque de St-Louis. Il figure ainsi au palmarès de la distribution des prix de l’école laïque de Saint-Louis en août 1884.
Boursier du gouvernement, il va poursuivre ses études en France, à Aix-en-Provence. Malade, il revient poursuivre ses études à l’école secondaire des frères de Ploërmel (ou de Duval) puis prépare en 1891 le concours d’entrée dans la fonction publique au service des Douanes où les places réservées aux Africains sont assez peu nombreuses à l’époque.
Blaise Diagne se marie avec Marie Odette Villain. Ils auront quatre enfants dont Adolphe, médecin militaire, Rolland, fonctionnaire dans les Chemins de fer et Raoul, footballeur professionnel et le premier footballeur africain à être sélectionné en équipe de France
Jërëjëf gudaluw fan te wér yaram
Diaradiaf bay mbaye Geuye sell yalla nagua wér té am khéwal am guaramal serigne bi
Merciii bcp baye mbaye
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye. Nafekh ak fenn kat,Ak Kou Gueumoul Diine,Di défendre Goorjigeen kenn douko baayi mouy wax luko neex.
Baye mbaye Yale na yalla goudal sa fan mane dh aférou soldar yoyou diaxalon na ma lol ndakh bounou né Serigne touba mo diokh Toubab yii aÿ soldar pour mou khéxale lén mane mom diaxalon nama lol wakh dëgue yalla wayé tayy mom ler na si mane yale nalla yalla faye barekéb borom touba cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul
Diara diaff baya mbaya
Kidal dafén rék wawma Aliou tine la wawma
Serigne Touba khadim rassoul yalla ak seydina Mouhamed diékh na
Kou rour lislami Serigne Touba dji
Walla nga bagn elhadji baa jumaaji.
Ndem goor nga ndem jigeen nga mala khiirou
Mattla bawla bathia fouta tooro.
Eskëy s Moussa ka)r.t.a.
Macha ALAH , S.mbaye gueye syll , goudal fane tè am diame ak kheweul , yalnagua am diadiafi SERIGNE TOUBA AK RAKAM MAME THIERNO .
DIEUREUDIEUF SYLLA yalla na YALLA goudale saw fane té maye la werre
Machalah sama papa mbaye Gueye amna solo yalna Borom Darou mouhty arla same la ci barkeb bamba
je soir en direct sur la sen TV avec baye mbaye merci 💚💚💚💚
S Mbaye gueye grazie mille merci
Tonton Mbaye sylla tous les musulmans particuliers les morides moi personnellement un grand merci s'il y avait d'autre comme vous ki nous dépend personne n va plus toucher à notre l'islam ( mourite)encore un grand merci
Diadieuf S.Mbaye .yallah na takhawaye bi yague
Baay mbaye yalla nala yalla takhawou yangi liguéyall s touba dé
Jërëjëfëti Baay MBaaye Guèye Syll , yaw daal Yàllah në ngë guddu aw fan te and ak wèr, lègui laa la doon setaan Sen TV , begg na ñu lol ci yaw maachAllah.
Yaw mome yaye sougnou porte parole massala goudou fane wère soutoura barkè alkhourane dolè khassidayi
Amine way
Amine
Yalla Nala yalla Faye Serigne Mbaye . Dieureudieuf
Léral yi am na solo Lo Sr Mbaye Geuye Sylla yalla nala yala samou
Macha Allah boul tayi gnou laye nianal yallah yagal laffi bayil la ak hel. Diaradjeufati Serigne Touba Khadimou rhassoul.
Merci m'baye Sylla
Merci se mbaye
Mor fademba kane lamp
Ma gui ziar bou wer. Toujours j'ai avec vous pour le travaille gue vous faites merci beaucoup pour vous
Merci serigne bi de retablier la verite vous etiéz pertinanté
dieureudieuf bay mbaye yalna ngathi dadiék guereumal serigne touba
Machahalla vraiment amatina solo loool barkep s touba yalnala yalla goudal saw fan barkep s touba
Slt papa Mbaye Gueye Syll fance numéro 1de XAM Sam réew sët Tou sëriñ Balla khaïta Syll moom boroom Darou
Machalla baye mbaye gueye sylle yalla lea serigne touba takhawou
Baye Mbaye Gueye SYLL. Jërëjëf. Yàgg naa laa topp waye tay lay sooga artu ci sa xët wi. Waye ku bëgg yoon wi rek ameel na la "jaajëf". Li ngay leeral amna solo. Yaa ngi làqqarci fen yu nu yagga ràbb ( lu tollu ci xarnu daanaka).
Je voudrais vous suggérer de créer un site de vérification des informations touchant à la Mouridiyah et à son fondateur, genre "Mouridiyah fact-check". Je sens que vous avez par devers vous beaucoup de connaissances et de documents de sources sûres. Et nous sommes à l'ère de l'information et de la communication et les forces du mal font la guerre avec. Nous savons que rien ne peut entacher ni diminuer l'aura et la précellence de Serigne Touba, néanmoins un tel site pourrait constituer un puissant outil pour démasquer les calomniateurs tapis dans l'ombre.
Merci baye Mbaye Geuye sylla
Salam, merci Père Sylla yagg fi te werr Amine
DIEUREUDIEUF serigne MBAYE GUEYE SYLL amna sollo
Merci bcp baye mbaye
Mame Boye wakhal. Yaw lagniy sago. Nous sommes très heureux de vous pour les réponses que vous apportez à ces mécréants et ennemis du mouridisme. Merci beaucoup.
Baye Mbaye gueye Gaayi ins biii Thi dieufour Lagne Tolou Noni Serigne Touba yi Niooy Tambouli Di Fegne Waaayi Nigay def Nonoula Yalla Nala Yalla Samou Thi Barké Seydina Muhammad Amiin
Dieureu dieuf serigne mbaye gueye nonoula rek
Merci bcp papa XAM SAM RÈEW TV
Duirdifati serigne baye mbaye guaye yall nala yall yaguí fi lo tewere loo amien
Serigne Mbaye Gueye Syll doundeule diam rk yalla nala Serigne Touba takhawou
Machalla serigne mbaye gueye
Bilay bariwo wakh lingay wakh léppe am gnarigne dieureudieufati
Dieur dieuf grazie merci soukrane
Nonou Serigne Touba Yalla dinaleen mbougeul Ndakh Serigne Touba moniwon « Birazou Man Baara zani Birazouman »
Ki momana fen merci bay mbay
Merci 👍👍👍👍👏👏👏👏
Boulén faalé yalanala nala yala samal bopaam, dieureudieuf yamignou nékal ci micro bi ,kouy tontou taa téko ci khamkham maanoul gnaack ci diamoon dij, ndakh gni khamoul bagna diawalé ta yaw machalaaa, yangui léér, god bless you,,,,,,
Machalla yalla na yalla guoudeul sey fann si barcké showrou ramadan bi
Dieuredieuf serigne Baye mbaye syll
Merci beaucoup baye mbaye
Beuri ay wakh akh wakh diou am ndiarigne bokoul yaw say wakh lepou ndiarigne la
Dueiradieuf serigne mbaye sylle yalla nala serigne bi fayal bopam wayé yonou mourid koufi wakha lodoul deugu da niou la wara fèkk fa nga nèk dèf ko lo bone lolou rék moy takha niou nopé
Dieuredeuf s touba amoul morome kenela.
Merci mBay Guey Syll Il faut que les Ripostes soit chaude et continue
Merci baye mbaye Sylla
Dieureudieuf baye mbaye Gueye SYLL yalla na nga fi yag loool té and ak wér
Bilahi on nai fier de vous yalla na yalla defala xéwal
Wakhal bamou nekh thi barcke Serigne touba diam rek gay am fi thi Argentine
Diaa dieuff Baye Mbaye Gueye Syll yalnala serigne bii fay
Alioune tine ragalal yalla sa borom
Papa yalla nalafi yalla yagal wayy jeureu jeuf
Way bayiléne Serigne Touba d'où sêne morome
Jerejef sñ Mbaye yalna yalla gudal fanwi
Dieureudieuf serigne syll il faut toujours répondre a ces détracteurs du mouridisme ce sont des jaloux et aigris merci encore une fois
Sylla yalna yalla samela werale le s'y barkebe Serigne touba
SUBHANALAH KI MOMANA FENE BAY MBAYE NA YATT WIDALL KI MBAM MOU MACKLA
Man yatt mo may Ray
جرجق شرج طوبي خادم رسل
🤣 na yetwi dal
@@wakhdeugguetayallatakh8129 wayi lima diakhal mbam mi day wekhe
merci la voix des sans voix mbegci yaaw
Yalla nala yalla same barkéb serigne bi
Non bariwo ayy wakh mbamm yé Bari wayé⚒️⚒️ Serigne Touba rék mon worr dieureudieufeuti Serigne Touba khadim Rassoul
Merci Baye mbaye gueye
yalla na nga fi yague té weur thi barké sérigne Touba
Thiey Baye Mbaye Gueye Syll yalla nala sunu borome sameu barké serigne touba rta 😭
Dieureudieuff Baye Mbaye gueye sylla
DIEUREUDIEUFATI serigne mbaye Gueye
Merci Serigne Mbaye Gueye SYLLA
Contane Naniou 👃🇸🇳🇸🇳👃🇹🇷👃
Mabye geuye Sylla yalla nafi yague lol amna solou
Merci serigne Touba n’a jamais été tendre avec les mécréants
Wskhal. de. machalla. yalla. nala. yalla. faye
The l. Lawyer du. Mouridism. Bravo. Every. Body lov u
Macha allah yag fii ta wer barkeb s touba
Dieuredieuf serigne touba
Dieureudieuf sunu baye wakh bi ler na am na ay teguine tei firdei yi mat na sant nagn la
Dieure dieuf baye mbaye syll si lerale dieure dieuf serigne touba boudè febbare nagnou raye
Merci beaucoup Serigne Touba daal foukou waay ligueyelé rk merci beaucoup
Ambassadeur du mouridisme
Serigne mbaye guéye yalla naguifi yague lool té wére
Damoul serigne touba lii koumou nékhoul danga sonnou
Akasa mouride sadikh
Think you
Serigne mbaye syll dieureudieuf koula sope là