yallna yalla faye la so amoule wone Sénégal fii mou niawe oustaz makhtar sarr yallna yalla takhawoula yalla samoula yalla motali sa yéne you rafété yepp
gni la matière moleine sonale mouye le corps humain té lolou dou nite.li yaw bou diogué sa dieum motakh niouye yobe sa dieum armèle ya.le corps humain est comparable à une bouteille d'eau(contenant),l'âme comparable à l'eau(contenu).ndokh bi bou diékhé niou sani bouteille bi.kou dé manatoul dara wa moussa khana dou mo wagni diouli be 5 ba yonentibi raniane.yalla naniou yalla défale dègue.
Ndeysane mane dama yeureum omar sall ndah pour mom yonente bi dee na te hamoul ni yonente moy lep ya rabiii.niaka xam yallah rek moko sonal naniou ko comprendre ndeysane
macha halla sarigne makhtar sare begene lolo bi omar sall wekhe thi sounu magge gnu bakha gui amena louma meti me bingga thi wakhe ba legi sama khol sedene deurdeuf
Yala mane na louné, Seydina Mouhamed (asw), mo gueune malakaal mawtiii fouff, té malakaal Mawtiii founé lay déménagement ci adouneuh bi di Ray la mm heure. Amna sakh Hadiths you wakhni, gni dé ci kharé danouy Hadj sassou Hadj ammé. Yala mane-na louné té day def louné
bilahi al hilmou houwal imam ... boudé si xéll rek lagnou teunk yonenté nagnou xam ni gno déé si biir yonentè bii .... mouhamadoul bassar lakal bassar bal houwa kal yahouti baynal xadiarr.. yana gnou yalla fayal makk yii ak gni baax Oustaz makhtar sarr
Pourquoi l'homme parle toujours des choses dont il ne connait pas. Etant des êtres limités nos paroles doivent être aussi limité et bien soigné. Dieu sw dit dans le noble coran sourate 3 verset 66: "...Vous avez bel et bien disputé à propos d’une chose dont vous avez connaissance. Mais pourquoi disputez-vous des choses dont vous n’avez pas connaissance? Or Allah sait, tandis que vous ne savez pas...." Il faut faire très attention aux hadiths qui parlent de la vie après la mort. Le prophète saw a dit plusieurs fois qu'il n'était qu'un homme, le coran le dit au sourate 41 verset 6 : "...Dis: «Je ne suis qu’un homme comme vous. Il m’a été révélé que votre Dieu est un Dieu unique. Cherchez le droit chemin vers Lui et implorez son pardon.». Et malheur aux Associateurs...." . Et plusieurs fois aussi dans d'autre sourates. Aujourd'hui on sait que plusieurs hadiths ont été inventé. on trouve un imam cité dans deux hadiths contradictoires. Actuellement les savants sont entrain de nettoyer les hadiths. Et malheureusement au Sénégal on gobe tout ce qui vient de l'orient qui parle du prophète ou de l'islam. Des rêves qu'ont fait certains imams, des livres que même l'authenticité est douteuse. Sans réfléchir et faire de véritable recherche , les oustaz doivent se limiter aux enseignements du noble Coran c'est plus sure et pratiquer sa religion en implorant le pardon de Dieu sw et éviter les discutions inutiles.
Mai sama xariti sama mbokou Muslima yi Yop magui léne di nouyou mai ousstanz Omar Sall lougan wakh dégue la mai camou Dara néck si mai yéne ibadou yi Lou takh kéun Mouna taral dinédji mai yalla dinédji lépe là fi yombal mai fo déckné camou bakhoul lolou la boukone khame basgue camou moy jour bou prophète dioudou mai dégneu KO wara magal mai magui daicke Lou dégan dé
Mais khana Omar sall da faté ni malakal mawtou 100000 personnes meun nanio dée si même heure té mom kép moy rotie sén rouh kon légui c'est bien possible que yonénte bi dadi téwé diotay you beuri founiou koy toudée
mdr comment sa ce fait que quel qu'un qui esrt mort il prier dans sa tombe réfléchir bien. *Bien sûr, vous souhaitiez la mort avant de la rencontrer. Or vous l'avez vue, certes, tandis que vous regardiez ! *Muhammad n'est qu'un messager - des messagers avant lui sont passés - S'il mourait, donc, ou s'il etait tué, retourneriez-vous sur vos talons ? Quiconque retoune sur ses talons ne nuira en rien à ALLAH ; et Allah récompensera bientôt les reconnaissants. (Surat Al-Imrân versets 143 et 144) omar il dit que la veriter
Allez étudier, d'abord, svp. Ce que vous niez c'est le Prophète SAWS lui-même qui l'a enseigné. Le problème c'est ceux qui prennent la parole - comme vous ou ce "Oustaz" - alors qu'ils n'ont droit qu'au silence. Si vous mesurez la religion au rationnellement admissible, vous sortirez rapidement de la religion, et de toutes les religions révélées. L'ascension avec tous les événements de son épisode ; les animaux parlants ; le gémissement de l'arbre ; la résurrection de morts ; la restitution de la vue aux aveugles (par Jésus AS), et j'en passe. La raison les admet ? Désolé, mais quand on ne sait pas, sa seule participation honorable à un débat, c'est demander. Merci.
yallna yalla faye la so amoule wone Sénégal fii mou niawe oustaz makhtar sarr yallna yalla takhawoula yalla samoula yalla motali sa yéne you rafété yepp
Kebe Dame wallahi deugla
kebe Ahmad amine kou bah
Soukar ya oustas yalla na yalla Faye yangi Faye ta dolli niou niou melni yow mousal nie si nie wakh wakh wakhi kevere yi
MashAllAh xam xam day am thieusslay !!
Ndaw dou té am niveau yalla na yalla yiw ci cheikhou Tijan
diarama oustaz beugé tina déh walahi ndeysaane yalna yalla faye la yiw baraka lahou fikoum
ما شاء الله يا أستاذ، أرجوك من فضلك لو جعلت هذه البيانات في كتاب أو مذكرة، لكنا أثبت على التصوف حتى لا يسوس علينا هؤلاء الشياطين مرة أخرى 🙏
ولا تحسبن الذين قتلوا في سبيل الله اموتا بل احياء عند ربهم يرزقون
Macha Allah oustaz Sarr Yalla nala Yalla fay yiw ci barké Cheikhouna Tidjani RTA
Tres content je suis Le 1er a ecouter cette partie : diarama sa Oustaz
machalla oustaz sarr yalna na yalla fayla
Merci beaucoup oustaz amme na solo longue vie à vous
moise ba amine
gni la matière moleine sonale mouye le corps humain té lolou dou nite.li yaw bou diogué sa dieum motakh niouye yobe sa dieum armèle ya.le corps humain est comparable à une bouteille d'eau(contenant),l'âme comparable à l'eau(contenu).ndokh bi bou diékhé niou sani bouteille bi.kou dé manatoul dara wa moussa khana dou mo wagni diouli be 5 ba yonentibi raniane.yalla naniou yalla défale dègue.
الرسول صلى الله عليه وسلم يقول:أكثروا الصلاة علي ليلة الجمعة ويوم الجمعة فإن صلاتكم معروضة علي
merci beaucoup Oustaz kokou day yakh al khourane rek amna ben Aya bumu wax ne ma nga surat hadidi te nekoul fofou manga surat nissai
amriamaaya
Oustas omar sall boukotonti ndakh fenkatla
Ndeysane mane dama yeureum omar sall ndah pour mom yonente bi dee na te hamoul ni yonente moy lep ya rabiii.niaka xam yallah rek moko sonal naniou ko comprendre ndeysane
BarakAllah Ouztaz yallah na yallah fayla amna solo leer na diaredieuf Sarr
bilay yalna yalla faye la li Si kholou kou bakh rek la khet
Machallah yalna la yalla faye
Attei yeup tek ngako fou lerr
machallahhhhhhhhhhhhh ya oustaz
Dieuredieuf outaz MACTAR sarr yalla nalla yalla takhawou outaz omar sall dafa reuy lika warr moy dem diangui watt 'mou dém wouti ham ham
man de khamouma dara wayye khamnane yalla amoul falantheir ya oustas makhtar sarr merci
merci bc pour tout long vie santé ( yalla na gnou hare ardiana you guene kawel si barque smr psl )
yalla nala yalla faye yalla yoka sa khame khame khame amine yarabi
Belle leçon messieur sarr
Omar sall démal diangi wat xamo dara té amo xiarr
Wallay ndaysaaaaaaane maaaaaaaaaacha alllah yaoustaz makhtar sarr Wallay ndaysan
dieureudieuf oustaz yaw yadiara deguelou omar sall amoul kham kham nateuthie lamigname woureuy wi khamoul touss soss katla fenkatla
macha halla sarigne makhtar sare begene lolo bi omar sall wekhe thi sounu magge gnu bakha gui amena louma meti me bingga thi wakhe ba legi sama khol sedene deurdeuf
Machalla amna solo
diarau dieuf ousstaz amna solo lol billahi walahi amna solo yal na yalla yokou kham kham bi machalla bofi nekoulou wone dou bakh
Wallahi oustaz Mactar sarr yalnala yallah samme wallahi omar sall nitou fitenala
merci oustaz sarr
Machallah oustaz merci
Merci beaucoup oustage yalnala Yalla féy wiu té yagal la fi
kou hame khamame gâté limouy wedi daye bari
merci oustagz m sarr
😟😟😟dieureudieu oustaz makhtar sarr dama bégue thi yaw boo fii nékouton mou gniaw
Ma challah ya oustaz amna solo
dieureu dieuf oustas mokhtar sarr
Yala mane na louné, Seydina Mouhamed (asw), mo gueune malakaal mawtiii fouff, té malakaal Mawtiii founé lay déménagement ci adouneuh bi di Ray la mm heure. Amna sakh Hadiths you wakhni, gni dé ci kharé danouy Hadj sassou Hadj ammé. Yala mane-na louné té day def louné
macakhla am na solo aostss mkhter sarr
لما ذا نقول: السلام عليك أيها النبي ورحمة الله وبركاته بضمير المخاطب
Jerejeff oustaz sarr sall ak niomelni moom nioy reeral nitgni
MACHALLA
Ay way talibé mo nekh ma sha Allah
lou lere naga wahe oustaz makhetr sarr
machallah on veut les éclaircissement sur la barbe et la langueur des pantalons pour un musulmans
bilahi al hilmou houwal imam ... boudé si xéll rek lagnou teunk yonenté nagnou xam ni gno déé si biir yonentè bii .... mouhamadoul bassar lakal bassar bal houwa kal yahouti baynal xadiarr.. yana gnou yalla fayal makk yii ak gni baax Oustaz makhtar sarr
iustaz oumar sall wediwoul sounou makyi yala la geumoul manmi diagoul khamnani xamoul dara
yalnanga gudda fan ta am wer ustas omar kham khamam gudul
Je veux le Numero oustaz Makhtar sarr
جزاك الله خيرا ءامين
Masha Allah ❤💖💕
oustaz omar sall feene rek
Pourquoi l'homme parle toujours des choses dont il ne connait pas. Etant des êtres limités
nos paroles doivent être aussi limité et bien soigné. Dieu sw dit dans le noble coran sourate 3 verset 66:
"...Vous avez bel et bien disputé à propos d’une chose dont vous avez connaissance. Mais pourquoi disputez-vous des choses dont vous n’avez pas connaissance? Or Allah sait, tandis que vous ne savez pas...."
Il faut faire très attention aux hadiths qui parlent de la vie après la mort. Le prophète saw a dit plusieurs fois qu'il n'était qu'un homme, le coran le dit au sourate 41 verset 6 :
"...Dis: «Je ne suis qu’un homme comme vous. Il m’a été révélé que votre Dieu est un Dieu unique. Cherchez le droit chemin vers Lui et implorez son pardon.». Et malheur aux Associateurs...." .
Et plusieurs fois aussi dans d'autre sourates. Aujourd'hui on sait que plusieurs hadiths ont été inventé. on trouve un imam cité dans deux hadiths contradictoires. Actuellement les savants sont entrain de nettoyer les hadiths. Et malheureusement au Sénégal on gobe tout ce qui vient de l'orient qui parle du prophète ou de l'islam. Des rêves qu'ont fait certains imams, des livres que même l'authenticité est douteuse. Sans réfléchir et faire de véritable recherche , les oustaz doivent se limiter aux enseignements du noble Coran c'est plus sure et pratiquer sa religion en implorant le pardon de Dieu sw et éviter les discutions inutiles.
Akasa
Mascella che giocato danelon gufi Gaia Gulfi sul mio canale di buona serata🤲🤲😍💪☝️
بارك الله أستاذ
machaalla ya outaz sarr
Merci beaucoup je suis très contente de toi
nett dangay diague banou pi dora wakh
maachallah ya oustaz leer na nagn naaagn. koumou meeti nak nga outi xam xam boko tonto. dieureudieuf!!!! bilahi dama beeg si iow
Bilay omar sall ya meuna doul sheuttttt yi khétou fen lanla kha ma warou man mayitounn bi miy kheuthie rek ka ma metti😂
Kén do cheikh
mascha Allah
Malleabilità 🤲😍
machalla
oumar sall bo âme diom diga nopi
Jaz aka lah
walahi
Mai sama xariti sama mbokou Muslima yi Yop magui léne di nouyou mai ousstanz Omar Sall lougan wakh dégue la mai camou Dara néck si mai yéne ibadou yi Lou takh kéun Mouna taral dinédji mai yalla dinédji lépe là fi yombal mai fo déckné camou bakhoul lolou la boukone khame basgue camou moy jour bou prophète dioudou mai dégneu KO wara magal mai magui daicke Lou dégan dé
Mais khana Omar sall da faté ni malakal mawtou 100000 personnes meun nanio dée si même heure té mom kép moy rotie sén rouh kon légui c'est bien possible que yonénte bi dadi téwé diotay you beuri founiou koy toudée
Durant les 1h11 minutou vidéo bi yeup djouli nako si yonéneta bi.
Pape Mbaye Tambedou way merci refetna njla ﻻتتبع الجاهلون
Omar Sall demal diangui. Dara nga khamoul
omar sall bouniou katoul ndayame
Bilay djekhoul
Mahktare sare todialsene lou bone rek gni ay domeramlagne rek rawatina omare sall mi
Macha alla
mancha allah
Mach allah
omar sall demal diagui
Macha allah
tu n as plus de koi dire???
ibadou doule rekk
say wakh nay aame daalil
Nice Allah
ndakh kham nga louy ibadou baparé
ndiaye djiby boul wax ibadou waxal salafia
ndiaye djiby ibadou dou tiotou ndaye billaye
#Alioune Kane# Quelle honte !
+Alioune Kane wakh nga dague
yeunantibi meuna louko.sout
mdr comment sa ce fait que quel qu'un qui esrt mort il prier dans sa tombe réfléchir bien. *Bien sûr, vous souhaitiez la mort avant de la rencontrer. Or vous l'avez vue, certes, tandis que vous regardiez !
*Muhammad n'est qu'un messager - des messagers avant lui sont passés - S'il mourait, donc, ou s'il etait tué, retourneriez-vous sur vos talons ?
Quiconque retoune sur ses talons ne nuira en rien à ALLAH ; et Allah récompensera bientôt les reconnaissants. (Surat Al-Imrân versets 143 et 144) omar il dit que la veriter
Vous êtes un vrai ignorant vous ne connaissez pas la dimension mystique du prophète psl va étudiez c'est mieux
Allez étudier, d'abord, svp. Ce que vous niez c'est le Prophète SAWS lui-même qui l'a enseigné. Le problème c'est ceux qui prennent la parole - comme vous ou ce "Oustaz" - alors qu'ils n'ont droit qu'au silence. Si vous mesurez la religion au rationnellement admissible, vous sortirez rapidement de la religion, et de toutes les religions révélées. L'ascension avec tous les événements de son épisode ; les animaux parlants ; le gémissement de l'arbre ; la résurrection de morts ; la restitution de la vue aux aveugles (par Jésus AS), et j'en passe. La raison les admet ? Désolé, mais quand on ne sait pas, sa seule participation honorable à un débat, c'est demander. Merci.
Mdr je perd mon temps à vous répondre vous les wakhabiss vous êtes des vrais ignorant
omar sall khamot dara
limi wakh tengo ko si xam xam
tu a rien corrige Macha allahou oustaz oumar Sall
Kholal ma dof bi rek
menteur k tu é
merci oustaz maktar sarr
machalla