"Gamou bidah la" - La réplique très salée de Oustaz Iran à Oustaz Oumar Sall: "Douma ragal..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 15 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 1.8K

  • @saddamdiouf1752
    @saddamdiouf1752 4 ปีที่แล้ว +11

    Yalna yallah def Diam Sénégal. Nguir yallah kou gueumoul serigne Touba, Elhadji Malick, Mame baye Niass,Mame limamou mokham. Bayilen niou rekk ak souniouye serignes.combien de personnes ont maitrisé le coran grâce à nos marabouts.dieureudieuf Cheikhou Oumar foutiyou.Iran boul tontou ligueyal nguir yallah. Linga wakh leer na.Machallah

    • @khadijamarega4604
      @khadijamarega4604 3 ปีที่แล้ว +1

      Majeur partie si Sénégal dégouniou Dîné dji.tarikha yagoul té l'islam amena avent,bidah dou raféte day arame.yonéntébi PSL waxona ni niom sén bir bolowouniou wayé bougnelén waxé deugeu rék niou bolo nék béneu.Gamou Magal yoyou yeup badah la

  • @bachirahmadoubambangom5035
    @bachirahmadoubambangom5035 5 ปีที่แล้ว +9

    Iran yaye gore walahi... Tous les Mouride t'aiment... Kép kou beug Iran beussal j'aime

  • @abdoulahiibn5779
    @abdoulahiibn5779 5 ปีที่แล้ว +40

    Oumar Ibn Al Khattâb -qu’Allâh l’agrée- a dit : « Méfiez-vous des penseurs, car ce sont les ennemis des sunan qui ont été incapables de mémoriser les hadiths et ont donné leur propre idée, s'égarant ainsi et égarant autrui » [Source : Fathoul Bâri, tome...

  • @aboudiop8846
    @aboudiop8846 5 ปีที่แล้ว +25

    Ndayssan thieye serigne touba macahallah dieuredieufe cheikhoul khadim yalla na yalla def diamo ci rewmi ci barkeb cheikh el hadij malick sy amin

  • @khadijakeita8367
    @khadijakeita8367 5 ปีที่แล้ว +9

    way beineu diiné reik la, oustaz Omar Sall mashallah tout ce qu'il prêche est en conforme avec la sunnah du prophète et le coran . Longue vie à tout ces oustaz 😊

  • @MARUGORMUSIC679
    @MARUGORMUSIC679 5 ปีที่แล้ว +7

    Kou beugg iran beusseul j'aime

  • @serignenarmbaye8986
    @serignenarmbaye8986 5 ปีที่แล้ว +251

    Barke sergne touba gueunala beug yallah nangua goude fane

  • @youssahoaidara7928
    @youssahoaidara7928 4 ปีที่แล้ว +12

    Oustage papa Iran ndaw je suis très fière de vous, car vous êtes véridique, vous avez bien répondu. Yagual té werre

  • @Sounouteleinfo
    @Sounouteleinfo 5 ปีที่แล้ว +194

    Haaa gamou 2019 bii nekna machallah 💪2020 bii moy dak inchallah

  • @bbouhama5373
    @bbouhama5373 5 ปีที่แล้ว +44

    "C'est dieu qui créé et c'est l'homme qui bricolé" 😂 dieureudieuf way amna solo

    • @alvaabassndiaye
      @alvaabassndiaye 5 ปีที่แล้ว +1

      Waw bricole si lou bakh rek inchallah.

    • @ndiabottabdouazizmbaye6229
      @ndiabottabdouazizmbaye6229 4 ปีที่แล้ว

      Heureusement que français guay dingatt 😌

    • @beau-d10
      @beau-d10 4 ปีที่แล้ว

      BBOUHAMA: Rey ngama 🤣🤣🤣

  • @sergej_milinkovic2120
    @sergej_milinkovic2120 5 ปีที่แล้ว +235

    Ana gni Beug Iran !

  • @Mama-fk9gp
    @Mama-fk9gp 5 ปีที่แล้ว +4

    Yalla na yalla goudale sa fane thi barke seydina Mouhamed bilay Iran sounou borome molay fayal bopame deugueu rek gay wakh 🥰😍❤️

  • @barrasamb8001
    @barrasamb8001 5 ปีที่แล้ว +54

    La pédagogie en toi est exceptionnelle
    Machallah Iran Ndao
    T’a tout dis
    Ces gens qui n’ont traduis l’islam littéralement ne valent pas la peine de répondre

    • @fatimadiakhaby9453
      @fatimadiakhaby9453 3 ปีที่แล้ว

      Au contraire c'est vous quii avait traduit la religion bidah bouu rafete fan la am? Allahu ahlem
      En tout cas je sais que in sha Allah au jour du jugement sénégalais yii dîna niouu sonne

    • @fatimadiakhaby9453
      @fatimadiakhaby9453 3 ปีที่แล้ว

      @@Goorgoorlou lerouuu ma dehh psk soumaaa lerone nii aldianna lay dougg je vais mm pas te répondre
      Allez apprendre la science au lieu de rester là à suivre des marabouts ou trucs
      Le jour du jugement il n'y aura qu'Allah qui pourra nous aider personne ne pourrait rien faire pour nous alors avant de rester là à suivre les marabouts suivez les deux trésors qu'Allah nous a laissé le coran et la sounna seulement

    • @hametndiaye4796
      @hametndiaye4796 3 ปีที่แล้ว +1

      @@fatimadiakhaby9453 c'est quand le jour du jugement dernier ??

    • @fatoumatathiaw7021
      @fatoumatathiaw7021 ปีที่แล้ว

      ​@@fatimadiakhaby9453tééé ngaa khalaattt sa boppou ba noppi

  • @ndeyefatoulo2280
    @ndeyefatoulo2280 3 ปีที่แล้ว +2

    Machallah oustaz Iran yalna yallah fayal gnou sougnou mak you bakhi té yok lér ak yeuremendé bou bari ci cheikhe seydil hadji Malick rta

  • @angeliquemendy7716
    @angeliquemendy7716 5 ปีที่แล้ว +8

    Man de chretiene la waye yalla nena diamoulenema ci sen kham kham con yalla borom kham kham yiis ley wakhale. Merci Iran yalla na la yalla defal diama inchahala 👍👍

  • @aminatacissokho9587
    @aminatacissokho9587 5 ปีที่แล้ว +5

    Thank you Pape Iran Dama diakhassowone bima dèguè lolou mais insbi explication bi lern na nagne con yalleu nalla yalla fay

  • @mamediarrambaye5633
    @mamediarrambaye5633 5 ปีที่แล้ว +154

    merci waye iran yalnala faye si barkeb serigne touba

  • @dethiediallo2705
    @dethiediallo2705 5 ปีที่แล้ว +18

    Dieureudieuf yallah bigua gnou mayé mak you bakh yi seydi hadji malikh ak serigne touba ak limamou lay ak boukounta macha allah Iran

    • @madoundoye421
      @madoundoye421 4 ปีที่แล้ว

      Yagal té were waye gni danio sokhor sene you thieuk

    • @abbakarsadikhdia2741
      @abbakarsadikhdia2741 4 ปีที่แล้ว +2

      Machallah yalna naniou yallah fayal mame sedile hadji Malick

  • @ndiagandiaye7364
    @ndiagandiaye7364 5 ปีที่แล้ว +3

    oustaz Iran ndao yalla nako fi yalla sakhal mayko wèrr barkè serigne touba Amine

  • @birahimkebe5731
    @birahimkebe5731 5 ปีที่แล้ว +93

    Barke serigne touba ligua wakh koko guené si diné lénène lo diap dou diné dague gou wer

    • @sodatine7618
      @sodatine7618 5 ปีที่แล้ว

      9vonbvnn
      Novices

    • @ndiagandiaye1427
      @ndiagandiaye1427 5 ปีที่แล้ว

      Dano sokhor rek molen diap

    • @solytoure8904
      @solytoure8904 4 ปีที่แล้ว

      Amna solo machalla 🙏🙏🙏🙏

    • @Al-maidaTV
      @Al-maidaTV 4 ปีที่แล้ว +1

      Yaw dagua diague baye atté li dîné wakh Sénégal mo nékh diaguil .
      Ma ladie la si mourideyi Serigne Touba niata sokhna la Amone .diaguiléne

  • @awaseck7685
    @awaseck7685 5 ปีที่แล้ว +6

    Senegal Kèna dall doufi wakh deugue nakh deugue nekhoulla dègue un grand remercimen a oustas omar sall

  • @cousteaucffall1755
    @cousteaucffall1755 5 ปีที่แล้ว +105

    Ibra fall néna " ah Dome déléne wakh May Dieuf niou xol ndakh beusou peinthieu Daniou Faye wakh bayi Dieuf

    • @ousmanendiaye3374
      @ousmanendiaye3374 5 ปีที่แล้ว +2

      Wakh deug koku ay wakh am leneenla

    • @Mayipeniang
      @Mayipeniang 5 ปีที่แล้ว +2

      Deguit way ken dou Mame cheikh Ibrahima fall

    • @mmbuur9901
      @mmbuur9901 5 ปีที่แล้ว +3

      lepp lagni fay mouy wax mouy dieuf tek si même les intentions car n’oublions pas que les rappels et prêches c’est à travers la parole

    • @lepatriote5050
      @lepatriote5050 5 ปีที่แล้ว +2

      Na dieuf lou Bakh rék deupo Al Quran ak Sunna sinon niou déloko dieufam ak loumou rëy rëy 🙏

    • @diakhateousmane9377
      @diakhateousmane9377 4 ปีที่แล้ว

      Yén deugéna réré mawodo wakh nalénn déugu lolu bida la yénako tay bida bou rafétte amoule diangé watte lénn waye

  • @bounandiaye5670
    @bounandiaye5670 5 ปีที่แล้ว +82

    Merci y'a outaz iran yagg fi te am wer si barke seydina mohamed

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 5 ปีที่แล้ว +3

    Akasa amna solo Dieure dieuf machalla merci irán ndawo wakh nga deuk dee bou weure yalnanga fii yague the andack weure barkep serigne touba Mbacke

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup7403 5 ปีที่แล้ว +112

    Barké s touba iran ndaw nekh ngama.gamou lepp louthi waye deff doko reuthou

    • @ousmanedicko2867
      @ousmanedicko2867 5 ปีที่แล้ว +2

      Wakh deubeu féte ko

    • @palayegaye2685
      @palayegaye2685 5 ปีที่แล้ว +3

      Diamou rk nguay am ndakh dangua Direct

    • @ayadiao2393
      @ayadiao2393 4 ปีที่แล้ว

      Bayleen bokaleh bii ho ho😭

    • @ouzinba7015
      @ouzinba7015 4 ปีที่แล้ว

      @@ayadiao2393 waté seringe touba khana bidala .

    • @Thiemokhodiouf
      @Thiemokhodiouf 4 ปีที่แล้ว

      @@ousmanedicko2867
      salut

  • @csfdiourbel
    @csfdiourbel 5 ปีที่แล้ว +85

    Je confirme la thèse de Iran ndao sur le maouloud : c'est un bidha très positif.
    En effet interrogeons l'histoire de l'islam.
    Les tarawih ( nafilas au ramadan) faits partout dans le monde musulman à commencer par la Mecque et Médine , sont venus après le prophète : il ne la jamais fait durant toute la mission. Il priait chez lui.C'est le calife Oumar qui a eu cette idée. Donc c'est un bon bidha.
    En outre, le califat a été institué après la mort du prophète d'où d'ailleurs les divisions internes avec le schisme. De son vivant on ne parlait que de oumma islamique. Et maintenant dans certains pays musulmans on parle de royaume. C'est un bidha mauvais.
    Enfin, le Coran dans sa forme actuelle , c'est le fait du calife Ousmane qui a eu l'idée de rassembler toutes les sourates détenues par les compagnons du prophète dans le but de préserver le message.
    Ça été un excellent bidha. puisque le coran na subi aucune modification.
    A l'attention de oustaz sall ,il faut éviter d'être dogmatique et suffisant

    • @cheikhadamatraore3706
      @cheikhadamatraore3706 5 ปีที่แล้ว +2

      Tu n sais pas de koi tu parle

    • @cheikhadamatraore3706
      @cheikhadamatraore3706 5 ปีที่แล้ว +2

      Bothi amei siki sakka je t'invite pv pour laralla

    • @cheikhadamatraore3706
      @cheikhadamatraore3706 5 ปีที่แล้ว

      Leralla

    • @beuguefallou6555
      @beuguefallou6555 5 ปีที่แล้ว +3

      yaw dagua kham dara bay léral laté sara Keïta degu bu wér la wax. Adama Yagui leudeum nane daguay léralaté

    • @laperlecmoi5995
      @laperlecmoi5995 5 ปีที่แล้ว +8

      mais bidah bou rafet amoul badah mome bidah la rek. li daguane dafa leer wayé li kharam dafa leer. anniversaire ben djoulit warouko fêté

  • @serignemassambadioptaysir7473
    @serignemassambadioptaysir7473 5 ปีที่แล้ว +116

    Amna gno khamni séne MAME démoul fénneu ba paré gnom gnouy bagne li mamou diambour déf mouy SERIGNE Touba rk thi kholl 👉❤️❤️ wala El Hadji Malick Sy......?

    • @baragaye66kiup0ebtfdxxggr9
      @baragaye66kiup0ebtfdxxggr9 5 ปีที่แล้ว

      Serigne Massamba Diop Taysir ú

    • @camaraboy3200
      @camaraboy3200 5 ปีที่แล้ว +2

      Yow sa mamm foumou demm

    • @camaraboy3200
      @camaraboy3200 5 ปีที่แล้ว

      Iran macha Allah

    • @zagaraga2169
      @zagaraga2169 5 ปีที่แล้ว +7

      Camara Boy mamame demoul fene mais geum na Mame borom Touba geum na Mame El adji malick sy

    • @boubandiyey9704
      @boubandiyey9704 5 ปีที่แล้ว +4

      @@zagaraga2169 nione yalla laniou geume akyonénetibi koubakhe kouné beugenanela gire yalla

  • @mouhamadousalamtassawouftv246
    @mouhamadousalamtassawouftv246 4 ปีที่แล้ว

    diereudieuf iran ndaw yalla nala yalla faye
    yalla na goudél fanné bi ak wér

  • @ndarawndiaye9663
    @ndarawndiaye9663 5 ปีที่แล้ว +92

    Omar sall kou bah la kou ame diner la ... Rolame moy yeter ... Mogui leral diner bi bou bah ... Iran aussi kou bah la yalla nagnou yalla tek si yonnou alcoran ak sunnq

    • @mdiop1829
      @mdiop1829 5 ปีที่แล้ว +1

      NDARAW NDIAYE walllahi mai c ignoran khamougnu lolou

    • @fallouleye8622
      @fallouleye8622 5 ปีที่แล้ว +2

      Ndaraw ndiaye wakhma loye alqorane ak sunna?

    • @ndarawndiaye9663
      @ndarawndiaye9663 5 ปีที่แล้ว +21

      @@fallouleye8622 al coran moy wahou yalla bi nek si teré biguay djiang . sunna beurina definition mais lou guene yombou moy lou yonentibi digueler ak limou terer .. Loumou digueler manam limou def ak limou feker sahabayi defko mou andessi. Ak ligua hamné Aboubacr wala oumar wala ousman wala Ali radiyallahou anhoum def nagne ko si guinawam car le prophète(psl) a dit topelene sama sounna ak sounna sahaba yima la sitel nonou... Oulafawou rachidin... Imam Malick ibn Anas radiyallahou anhou nena guinaw bou yalla waher diner bi matna ... Lifi way fénte si diner day melni yonentibi dafa trahir mission biko yalla tracel ... Exemple : Dieu dit dans le coran diner bi mat na ... Alors lou mat louy utiliter di fente lenen ... Le meilleur exemple et le prophète(psl) doundam lepp lagnou hamal dem ba kouy dougou toilette mou hamalla loy wah ..diner bi lou neubou amoussi. .. Merci mon frere balma sou feker yekeutina cadou boula blesser . kou bahgua djieuredjieuf

    • @ibouthiam3274
      @ibouthiam3274 5 ปีที่แล้ว +4

      @@ndarawndiaye9663 diangalé wala yété si réseau sociaux yii mouhamed saw bayi woukofii dh

    • @sadoudiallo2726
      @sadoudiallo2726 5 ปีที่แล้ว +4

      @@ibouthiam3274 salam sang bi teksi nè oci alkhourane ci portabl yi saws bayiwouko fiwone tè portabl yi daniouy dougou ak mom ci toilette

  • @yassyass8284
    @yassyass8284 5 ปีที่แล้ว +8

    Lo hamni sahaaba yi nga hamni gno gueneu diégué yonneti bi psl meussouko nio def,Yallah santou lako,yonnete bi santou lako nga da nga koy def Sénégal daal sein dinée bop lagne yorr hamouniou sounnah tei kou wakh gnounila sama maaame ,nagnou maytou innovations religieuses yi nak dinnei gui lossi bolei loussi bokoul sou yawmal hiyaamei dinagne lako deiloo.
    wassalam

    • @SALIOUgayeVTOsonatel
      @SALIOUgayeVTOsonatel 5 ปีที่แล้ว

      Yass Yass mâcha Allah que la paix soit avec vous

    • @verdugokiller8552
      @verdugokiller8552 5 ปีที่แล้ว +1

      Wahofi dra yoneti bi danoul lék thiéb bouko lékk

    • @papakane6753
      @papakane6753 5 ปีที่แล้ว

      Verdugo killer dieureu dieuf waye

    • @verdugokiller8552
      @verdugokiller8552 5 ปีที่แล้ว

      @@papakane6753 bayil gni dagno dof

  • @talibeckiekhbirrsopeserign4432
    @talibeckiekhbirrsopeserign4432 5 ปีที่แล้ว +45

    Vraiment Iran champion lau koi .Man Lila gem deugg Rek moy deugg

  • @حبيبربه-ه2ن
    @حبيبربه-ه2ن 4 ปีที่แล้ว +1

    زادكم الله فتحا ونورا تهتدون به ويهتدي به المسلمون يا أخا الفضل. احسنتم القول

  • @abdouleye2326
    @abdouleye2326 5 ปีที่แล้ว +15

    Merci IRAN NDAO que le bon DIEU éclaire ton chemin

  • @southafrica6239
    @southafrica6239 5 ปีที่แล้ว +1

    Maa Shaa Allah!!! Señ iran ndaw yallah naa yallah yoko saa fann tè wèrel say thièrr barkep brom touba

  • @pendasarr7948
    @pendasarr7948 5 ปีที่แล้ว +26

    Barké Serigne Touba yaw ak oustaz Modou Fall Yenay samayy oustaz.... Machallah bcp d'enseignements dans vos discours

    • @ousmanediallo227
      @ousmanediallo227 5 ปีที่แล้ว

      Ki doul rek lay def

    • @lobservateur8800
      @lobservateur8800 5 ปีที่แล้ว

      @@ousmanediallo227 sa bay moko dakka doul

    • @ousmanediallo227
      @ousmanediallo227 5 ปีที่แล้ว

      @@lobservateur8800 je l'aimais avant trop même. mais c'est un vrai escroc un menteur il est la que pour l'argent mais pas pour l'islam. Frère si tu me crois pas tape sur ytb Karim xrum xax sur Iran ndao tu vas devoir ils sont tousses des corrompus. A part oustaz Oumar Sall. Tout les reste sont des domaram

    • @ousmanediallo227
      @ousmanediallo227 5 ปีที่แล้ว

      Starfoulah oustaz Alioune Sall je le respecte bien lui aussi 🙌❤️

  • @awadioume84
    @awadioume84 4 ปีที่แล้ว +1

    Machala oustaz 😍Kou d'accord nii Iran dafa nirol ak serigne bethio thioune👍

  • @falloudiagne9175
    @falloudiagne9175 5 ปีที่แล้ว +80

    Iran mala bbeug way barki serigne Touba

    • @falloundiaye7246
      @falloundiaye7246 5 ปีที่แล้ว

      Bilahi ira mala degue

    • @yahyathior8088
      @yahyathior8088 5 ปีที่แล้ว

      Boul wahlo Mahdo la verite est unique bidda moussoul rafete

    • @falloudiagne9175
      @falloudiagne9175 5 ปีที่แล้ว

      @@yahyathior8088 li jamou yala geunuko reuy mo geun def lenen

  • @papeomardiagne4650
    @papeomardiagne4650 5 ปีที่แล้ว +2

    Ouztas Iran linga wax lérna konn koussi démati maka boul yégu avion boul takk montre boul yor kamil alkourhane boul yoré téléphone boul yor passport boul yorré carte d'identité parce que lolou yeup amoutonn sii diamono yononti bi psl ouztas Iran way😂héééé dieundilénn guélém ngénn adjii maka bien dit👏👏

  • @moussasallngom6578
    @moussasallngom6578 5 ปีที่แล้ว +10

    Machalla iran amna solo trop yalla na yalla fayal Elhadji Malik sy si barke seydina mouhamed

  • @muamarkhadafitv1509
    @muamarkhadafitv1509 5 ปีที่แล้ว

    Jerejeuf yà check iran beknaa siyaw besniki Tew mousouma nangou dila seetan way sa wahjii taxnané jappenaa yalla mala yalla may gouddou fanne ak wergou yaram Aamine Macha Allah Rafetna

  • @mdiop1829
    @mdiop1829 5 ปีที่แล้ว +6

    Wallahi iran yaw kou wara wuti kham kham nga ay avion ay oto lolou dou diamou yalla
    BIDHAA MOY BEPP DIAAMOU YALLA BOU NITT DEFF GUINNAW YONENTE BI DISSI WOUTT TIYAB TE DIELÈWOUKO SI AY SHABAM
    AY OTO AY GUILÉM LOLOU DOU BIDHA MAI DAFAY DOUGGU SI WALA KHAD KARAMNA BANI ADAAMA

    • @moussadaff5097
      @moussadaff5097 5 ปีที่แล้ว

      barakalahou Fikoum M Diop

    • @nevergiveupnevergiveup3318
      @nevergiveupnevergiveup3318 5 ปีที่แล้ว +1

      Merci frère nie deugou niou dîné

    • @bassfall5382
      @bassfall5382 5 ปีที่แล้ว +1

      M diop yaw lifi yonenete bi bayi wol won barina de WhatsApp sonnah la TH-cam binga nice ni di wakh lola nékh koko fi bayi akh

    • @aichamariamadiatta1936
      @aichamariamadiatta1936 4 ปีที่แล้ว

      Vraiment akhi! Je suis d'avis avec toi. Il essentiel de comprendre le sens profond du mot avant d'en débattre. Celui qui veut être sur le bon chemin doit se conformer au Coran, à la Sunnah du prophète PSL, demander à Allah la guidance. Un bon musulman doit dire du bien sur son prochain ou se taire, œuvrer dans les chantiers d'Allah( recommander le bien et interdire le blamable selon le coran et la Sunnah) sans vexer ni offenser l'autrui donc de la manière la plus douce; avoir un bon comportement et de bonnes intentions( tjrs en restant dans le cadre des recommandations d'Allah et de la sunna du prophète PSL). Mais maintenant la plupart des gens veulent avoir raison sur l'autrui alors que ce qui compte c'est de véhiculer la bonne information juste guir Y'Allah takh

  • @abdoulahiibn5779
    @abdoulahiibn5779 5 ปีที่แล้ว +1

    Allâh -Subhânahu wa ta‘âlâ- a dit : « En ce jour, J'ai parachevé pour vous votre religion, Je vous ai comblés de mon bienfait et J'ai agréé pour vous l'islam comme religion » (Sourate al-Ma’idah ; 5-3) Le Messager de Dieu (paix et bénédiction de Dieu...

  • @papezidane3965
    @papezidane3965 5 ปีที่แล้ว +25

    *Hahaha iran mo dééh nèna wadji boulko dague bo waxoul done dh gnou daag ko journaliste yii rèk😂*

  • @mmbuur9901
    @mmbuur9901 5 ปีที่แล้ว +10

    Ecoutons objectivement ces deux videos et non en nous basant sur le fait qu’on appartient à une tarikha. Par ma modeste personne en quête de science et en essayant d’être aussi objectif que je le puisse, Ya Imam Iran Ndao lui même avoue que c’est une biddah alors pourquoi cherchons nous à soulager nos conscience si une biddah peut être belle, un péché peut l’être encore plus alors allons nous juste nous baser sur le fait qu’une biddah est belle pour la pratiquer? Autant faire de beaux péchés alors. Wallahou a3llam mais on aime trop modifier la religion en notre faveur au sénégal c’est pas par ce que Ya imam avec un raisonnement non digne d’un imam dit ce que tu veux entendre que tu vas mépriser une autre personne qui dit la vérité et dire du mal de lui
    Une biddah est une biddah
    un péché est un péché
    La sounna et le coran suffisent amplement et a mon humble avis si tu veux célébrer, fait qiyamul l’ail (prière nocturne ou nafiila), jeune lundi et jeudi et fait du zikr car là ce sont des sunnas et pour tout ça ta chambre te suffit c’est par ce que t’es à Touba, tivaoune ou autre que t’aura plus de Hassanats
    Wallahou A3llam je demande pardons à tous ceux que ces propos ont pu offenser
    Baarak Allahou fiik
    Qu’Allah préserve la ouma ainsi que le sénégal

    • @cheikhsaadbouh109
      @cheikhsaadbouh109 3 ปีที่แล้ว +1

      صدقت والله بارك الله فيك

    • @leonematidiarra1994
      @leonematidiarra1994 3 ปีที่แล้ว +1

      Machalla ça m’as tellement touché merci.ce que vous avez dit c’est la triste réalité .Pour moi bidahh égal bidahh dc pas de polémique sur ca.les sénégalais tjrs se basent trop sur les Tarik alors pour pouvoir gagner le terrain dans l’islam il faut se baser sur ce qui est dit dans le Coran.Alhamdoulilah ♥️.Alahouma barikk qu’Allah soubhana watahala nous guide sur le droit chemin et nous épargne de ttes connaissance falsifiés de l’islam.Walam 🤲🤲

  • @konadiouf2596
    @konadiouf2596 5 ปีที่แล้ว +28

    😂Bilahi Iran diangue bi Serigne Cheikh wakhone diap nga ka mouy "diangue léne tontou"

    • @palminafabbretti6339
      @palminafabbretti6339 5 ปีที่แล้ว +1

      Omar sall nagne ko wara douma doma rammla

    • @palminafabbretti6339
      @palminafabbretti6339 5 ปีที่แล้ว

      Kouthie naryi finassè nga gnawfi disakhal sikimm reyyy koutii thipiri

    • @gop7604
      @gop7604 5 ปีที่แล้ว

      @@palminafabbretti6339 ah bon naar yi dagnko financer?

  • @cheikhndoye8279
    @cheikhndoye8279 4 ปีที่แล้ว +1

    Contane si Iran ndaw

  • @moussaba2252
    @moussaba2252 4 ปีที่แล้ว +9

    Vraiment ça suffit comme explication c'est très clair et bien dit

  • @ousmanebasse8967
    @ousmanebasse8967 3 ปีที่แล้ว +3

    Mâchâ Allah ❤️❤️❤️

  • @maimouna9553
    @maimouna9553 5 ปีที่แล้ว +12

    Longue vie mon Oustaz👏🏾👏🏾👏🏾

  • @southafrica6239
    @southafrica6239 4 ปีที่แล้ว

    maa chaa Allah oustaz iran Ndow yallah naa yallah samoula si barkè señ Touba mbackè

  • @ababacarndiaye3385
    @ababacarndiaye3385 5 ปีที่แล้ว +2

    Merci Oustaz Iran. Ragal Yabb Yallah-la. Je suis très content de vous. Yallah na Yallah degerel sa taxaway.

  • @ousmanendiaye3374
    @ousmanendiaye3374 5 ปีที่แล้ว

    Gni doul rek laniouye Def gueumougnou d'ara seen baye yeup ay talibé la niou waroo leen sakh tontou té Nak niou ciss la niou té bone té soof merci iran

  • @matouloveki8277
    @matouloveki8277 5 ปีที่แล้ว +44

    DIARAMA SERIGNE TOUBA

  • @narseye1998
    @narseye1998 4 ปีที่แล้ว

    😅😅😅😅ware lén gilem te dem maka. 😅😅😅😆😆😂😂Iran ndao Merci bien dit.

  • @falloudiene3670
    @falloudiene3670 5 ปีที่แล้ว +5

    Wawawwwwwww Iran yagui may dioy Lo 😢😢😢😢 vérité absolue 😭

  • @mohammedanne7910
    @mohammedanne7910 4 ปีที่แล้ว +2

    Vraiment vraiment vraiment tout c'est la fin tu es tu as bien parlé Allahu Akbar que le bon Dieu vous garde

  • @assanekandji4807
    @assanekandji4807 5 ปีที่แล้ว +59

    Iran yaw wakh katou degga nga bilahi 👍

  • @mariamaloum5323
    @mariamaloum5323 3 ปีที่แล้ว +1

    Iran kouma soppeu nga wayé mouhamad psl dal danou ko magual té souko néxone né jour bobou la dioudou wone té sahaba yi aussi meussou niou ko fêté Kone bok on clôt le débat 🤝

  • @s.89.7tvdoleld.medial.offi4
    @s.89.7tvdoleld.medial.offi4 5 ปีที่แล้ว +15

    bielaye wakh nga deguo yalla na yagui th wer si barkeb serigne Touba

  • @serignefalloudiouf3914
    @serignefalloudiouf3914 5 ปีที่แล้ว

    Machallah Iran ndaw yalla guafi yague tawer sakadou amna solo billahi amna niou khamne diarou niou tontou nakh amou niou kham kham billahi nima beugue sama papa nonou lala beugé yalla nasa fan goudou

  • @naturehumaine1219
    @naturehumaine1219 5 ปีที่แล้ว +12

    Gamou ak Magal
    Mano leen wax ba niit yi bayi ko
    Wa dou ngeen nopalou🤔
    Wala bok sangoum nèw mi ( wax ji ) dafa aam lou ci rakh ( financements🔥💥🔥 rewmi ak xèkh maak yi )🤔😃🏃‍♂️😃🤔

  • @motvsen5438
    @motvsen5438 5 ปีที่แล้ว +1

    Perso, je ne fais pas de Gamou et je ne critique pas non plus ceux qui le font. "Gamou biddah leu mais bou rafett...", parole de Mawdo, rapportée par Oustaz Iran Nadaw. Biddah=biddah. Rafett ou Niaaw, la question était simple: Le gamou est-il biddah ou non ?
    Ce pendant, l'idée de prier sur le prophète (PSL) n'est pas postérieure... mais choisir un jour spécial pour le faire n'est pas non plus antérieure.
    Aller jusqu'à confondre une pratique (Gammou) et un moyen de transport (pour se rendre à la Mecque ) est, à mon avis, pas "cohérent".
    En réalité, Oustaz Iran Ndaw ne dit pas le contraire de ce qu'a dit Oustaz Oumar Sall.
    En fin, ils sont tous les deux d'accord que le Gammou est biddah; même si Oustaz Ndaw ajoute que c'est "biddah bou rafett leu". Enfin bref, Allah seul est connaisseur. Puisse-t-Il nous accorder une bonne fin au moment de la mort et demain au jour de la résurrection. Amine

  • @bathiembow8997
    @bathiembow8997 5 ปีที่แล้ว +5

    Machallah IRAN NDAW dégue na si yawe barkel SERIGNE SALIOU

  • @iboufaye8332
    @iboufaye8332 5 ปีที่แล้ว +1

    Iran ndao le grand oustas

  • @momodieng3983
    @momodieng3983 5 ปีที่แล้ว +8

    Merci Ibrahim vraiment tt les talibés cheikh particulier tivaonane onet vrai ment fière de toi

  • @mamadousamb4718
    @mamadousamb4718 4 ปีที่แล้ว +2

    Machaalah, amna solo, yallah nala yallah fayy

  • @fodesiby4393
    @fodesiby4393 5 ปีที่แล้ว +5

    Wallahi Sénégal dou démm kanam deugue dafa mettii mouhamad (psl) moo wah ni lepp louy bidah réére là na niou dianguatte hadissu mouhamad (psl ) bou bakh ak al Quran

    • @momarsambe1398
      @momarsambe1398 5 ปีที่แล้ว +1

      Ioe ya wara djangui wat! Yallah cest pas pour rien foumou djokhé missal né borom xel yi lay waxal!
      Degg degg bakhna si nitt
      Kép kouy wakh kalimatou la ilaha ilallah dérét arame na moromou djoulit, esk aboubacar mi takone kharé contre djoulit yi bañone guéné azaka takh na mou tégui ndigalou yoneth?
      Hadith bingay wakh gueuno ko mokal ñi soss gamou... lane lañou soss si beuss bobou? Wakhtane si yoneth bi, Wla tague yoneth bi, Wla djouli si mom, wla djamou yallah si mbolo, wla togue djokh nitt yi lek, ani lane mofi amoul wone djamono yoneth bo (saw).. s'il s'agit de l'intention (magal beuss bimou djoudou) mom dane na wor les lundis pour magalé ko beussou djoudone... donc lane moci bidah?
      Diné islam dou diné wérénté nañ rafétal xol yi té djamou yallah sakou ngueureumam.. mom moy juge bi
      Nga balma akh nak.. wa salam

    • @bayendoye2802
      @bayendoye2802 4 ปีที่แล้ว

      Diguate kateyi kesse gnognou Sonal li dafaye maye ay nonne

    • @bayendoye2802
      @bayendoye2802 4 ปีที่แล้ว

      Diguate kateyi kesse gnognou Sonal li dafaye maye ay nonne

  • @awadiopba2155
    @awadiopba2155 5 ปีที่แล้ว +1

    Salam bida bou rafetna amoule si dinè l'islam le Prophète n'a jamais célèbre sa naissance les sahabas n'ont plus donc yalnagnou boromebi maye khewal tawhid amiiiine

  • @faramendy7410
    @faramendy7410 5 ปีที่แล้ว +18

    Tu as bien dit oustaz iran mashallah🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @famalo9021
    @famalo9021 5 ปีที่แล้ว

    Dieurdieuf way iran yalla na yalla may fane bou goudou ak were ak kheweul ci barke serigne touba

  • @mouhamadoulamineseck5142
    @mouhamadoulamineseck5142 5 ปีที่แล้ว +3

    14mn:32s iran ray nama🤣😂😂🤣 machAllah réponse bi amna solo!

  • @lenfentnoir3020
    @lenfentnoir3020 4 ปีที่แล้ว

    Assalamaleycoum mouh nekh bîinda mou bànñà nekh bîinda yalla moý ballée dôu kéen sîi nîoun wassallam

  • @amdyndiaye9349
    @amdyndiaye9349 5 ปีที่แล้ว +20

    Ndaysane Iran saff ngama wayy DEUG rek ngafi teek ni

  • @KhadimKa-fx1gx
    @KhadimKa-fx1gx 5 ปีที่แล้ว +2

    Thieyy serigne touba machalla amna solo

  • @bleakbleek7734
    @bleakbleek7734 5 ปีที่แล้ว +31

    Jerejef serigne Ibrahima iran ndaw

  • @1999-un
    @1999-un 4 ปีที่แล้ว +1

    Iran tu as tout dit. Yalle nala yalla samm

  • @keurhawaets6645
    @keurhawaets6645 5 ปีที่แล้ว +24

    MACHALAH SA MA XOLE BI SEDE NA LOLE THI IRAN VRAIMENT DJOULIT PIR DAY MANDOU IBADOU YII MOME NA MA YALLA BAL FITNA REK KO THI DEM KEURAM COMME DEUTH NDAX STRESSE

    • @djibydiallo1182
      @djibydiallo1182 5 ปีที่แล้ว +1

      😂😂😂

    • @amanatine9282
      @amanatine9282 4 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂😂😂😭

    • @ouzinba7015
      @ouzinba7015 4 ปีที่แล้ว

      Way tiwavone nékh guén tok lén fofou rèk

  • @cissepapis741
    @cissepapis741 5 ปีที่แล้ว +2

    Man séne afairou serigne yi yalla ma si mouthieul

  • @linspirateurniang650
    @linspirateurniang650 5 ปีที่แล้ว +10

    Que ya ALLAH nous préserve de la Jalousie 🙏🙏Machalah Oustaze iran

  • @mouhamadousylla5867
    @mouhamadousylla5867 4 ปีที่แล้ว

    Mouhammad psl est l'homme le plus pieux des être humain dans les coins et recoins de l'univers, dieu l'a choisit infiniment, après tout ça comment les gens peuvent ne pas reconnaître la nuit du prophète.

  • @bassfall2679
    @bassfall2679 5 ปีที่แล้ว +18

    Gor pire nga iran. Danio beug koulen xass rekk waaye kilifayi liniou ligguey ana seni maam boba

  • @mouhamatsy7551
    @mouhamatsy7551 5 ปีที่แล้ว +2

    Vu que bida Bou raffete la kou mou dal sa khél nga fête ko, koumou daloul sa khel ga bagne ko fête, lou bari yawmalkiyam rek lay lérai
    Yallah naniou yallah may degue ak top

  • @diamouyallahtv4363
    @diamouyallahtv4363 5 ปีที่แล้ว +9

    Merci Oustaz Iran Dieurëdieuf machallah wakh dji raféte na
    Omar Sall dafa mana Fénn kham na lambi wakh moko férmé

    • @Wildflower718
      @Wildflower718 5 ปีที่แล้ว

      DIAMOU YALLAH Tv ioe ya niakk yarr fii dinê bi dou dinê Mame personn yenn merde way

  • @rtro223
    @rtro223 3 ปีที่แล้ว

    Yalla nagnou yalla gueuneu dieumeuler ci seydina moukhamed

  • @yayadieng893
    @yayadieng893 5 ปีที่แล้ว +7

    Iran machalla tu as tout decortique tu es un vrai sage que le bon dieu te benisse amine

    • @bintoujeng7726
      @bintoujeng7726 5 ปีที่แล้ว

      Machaala machaala serigne Iran yalla nagua goude faan ci barakatul Rassoul serigne touba ak mame cheikh ibra fall lamp ak Maodo Malick jiadieuf waye barkel wakhe ji machaala deugu reek woor ❤🙏

    • @bintoujeng7726
      @bintoujeng7726 5 ปีที่แล้ว +1

      Yalla yalla barkel wahe ji sope nale waye

  • @ndaoawa8611
    @ndaoawa8611 4 ปีที่แล้ว

    Machalla waay tonton inra kadou rafetena

  • @amethsoce3075
    @amethsoce3075 4 ปีที่แล้ว +4

    Barké s touba dama la beugue iow kou bakh nga😫

  • @assanesanezondour5038
    @assanesanezondour5038 4 ปีที่แล้ว +2

    Iran Ndao bilay deug rek mola Taha djog yallah na bour bi doli soutura inechallah

  • @adamabah6351
    @adamabah6351 4 ปีที่แล้ว +3

    Maintenant mon oustaz parle bien l français !!lol !! Longue vie à toi

  • @jmpsen9192
    @jmpsen9192 5 ปีที่แล้ว

    C'est pas un debat d'amateur. Les critiques vous poussent a ameliorer vos oeuvres. C'est les journalistes qui doutent de la chose. Oumar sall developpe son point de vue. C pas mal.

  • @wadekhady8413
    @wadekhady8413 5 ปีที่แล้ว +18

    Goudal fane Iran deug rek ngay wakh
    Gueune nala sopp wallahi

  • @ibrahimadieng2471
    @ibrahimadieng2471 2 ปีที่แล้ว

    Dieuredieuf IRAN yalnagafi yageu thie barcke borome touba

  • @mamediarralo9607
    @mamediarralo9607 5 ปีที่แล้ว +11

    Machallah Yalla nala Yalla samou

  • @amidiop8311
    @amidiop8311 5 ปีที่แล้ว +2

    Ma sha ALLAH. Bien dit Ibrahima. Tres contente

  • @laprincesse7145
    @laprincesse7145 5 ปีที่แล้ว +7

    Deugue rek la fi wakh respecté nieup dawale yeurmané ande done beneu te Yalla takh

  • @abdoulahiibn5779
    @abdoulahiibn5779 5 ปีที่แล้ว +1

    « Dis ' Voulez-vous que nous vous apprenions lesquels sont les plus grands perdants en œuvres ? Ceux dont l'effort, dans la vie présente, s'est égaré alors qu'ils s'imaginent faire le bien '
    Et dans un autre verset, Allah dit : « En fait, on a embelli aux mécréants leur stratagème et on les a empêché de prendre le droit chemin. Et quiconque Allah laisse égarer n'a plus personne pour le guider » (Le tonnerre, v33).

    • @papasambadiop7599
      @papasambadiop7599 ปีที่แล้ว

      Kone bayil diouli ci Diaka bou am micro ak hautparleur ak sauraur ndah biddah lah👌🏾

  • @damedia463
    @damedia463 5 ปีที่แล้ว +23

    Akamako kham douraggal dh😂😂😂

  • @mouridediop9307
    @mouridediop9307 4 ปีที่แล้ว +1

    Amnà solo

  • @lialialino2592
    @lialialino2592 5 ปีที่แล้ว +26

    Iran fougnou diadié amguafi diouni

  • @fatimandiaye302
    @fatimandiaye302 5 ปีที่แล้ว

    Yalla mangi lay gniane thi barké cheikhou tidiani Iran ndao yalla naa goudou fane barki alkourane kou bg Iran wakhal amine inch'Allah