khadi diouf c'est la tante de ma meilleure amie depuis enfance mais c'est vraiment triste maman khadi que la terre lui soit légère firdawsi soit sa demeure éternelle
"Sangue leen réwmi ak khol bou seet wala nguéne sangué ko ak déret " disait un sage .... Sénégal khamo lein li nguen am sakh sen niou bakh nioniou abal len niouko bok
Thiéy yalla Ay way li Lou mou don Ban Sénégal la niou nék légui chaque jour ak ligay dé si réseau sociaux yi yalna niou yalna niou yalla moussal si seytané 😭😭
Adouna amoul solo maintenant elle est en prison on ne la pas encore juje dans sa maison elle a detruit des vitre aluminium ak ay ecran plat bou tolni cinema et elle adit sama dieukheur dinako def lo khamni day kharou elle a dit de sa propre bouche
Ay wayyyy ndeyssane ohhhhhhhhh masta 😓 billakhi c'est triste 😔 Mais naniou nianal ki guéneu adina,nianal aussi ki ray té mouslou si séytan....lolou reik mo am solo 🙏latia dess niou bayiko ci lokoy sounou borom😔🙏 Kéneu waral jujé kéneu ndak kou guénagoul adina hamagoul lanelako yallah réservél thi aveniram!!! yãh Räb 🙏😭😔
Sa dieukeur dé bou xamone ni yay ray yayam doula meusa tak ak yay nimou meil thi dôme yalla nalaa yalla yeureum yaw mi gueine adouna figa deim gueneul la figua djouguei
Djiguen dal waroul am fit. Té djiguen bo khamni sou méré day yakh nitkou bone leu ba sokhor teksi ndakh yeureumo sa dieukeur dji nek bitim rèw si sèd ak thiono yimouy dathie pour teral leu teral yayam ngani doufi amé. Eyway ki yakhna famille way😭😭😭
Li rekk motakh ma raguala tak sokhna malgré djiguén yeup yémou gnou mais do kham koy wolou maman yalnala yalla yeureum kharéko aldiana firdawsi ak bép dioulit
Yalla nako yalla yeureum. Personnellement sama gooro moma diangal togue lep li diguen di sokhla rek momako diangual Yalla nako yalla yeureum té yékheniou
Yar len sen doom yi, li yep niak éducation moko lal, nit so amoul yar amo dara. Comme disait ma mère rek "koula rayal kou rew soula fayei kou dof dieuleul" Qu'Allah lui accorde sa miséricorde ❤
Nooo bou len wakh lolou kou nekk ak djikome si coté mère y ak qui di seuye, qui di seuye mo warone corrigée comportement wame enver sa belle mère, lii mome daaraye adouna doumako diarale soumala naré sagua dem bayi la ak sa keur 🙏🤲🤲🤲🤲
Bilaye kou moye touwoul seytané do diogué thie def lou bone niowe bakhoule histoire goudi ak béthiek li rek léye diour yalla na yalla moussale niou thie seytané
Sama khol bi moye metti ak yaye nimou sone si dome eumbe 9 mois bene beuss khaw la ray sa diarbat di fonto sa yaye ma bagne goor bou gnak fayda mere bi yalla na khippe sa aldiana firdaws 😭😭😭😭😭😭😭
C'est la faute du mari ,une femme qui terrorise tout une maison, et son mari na pas réagit avant.cest ça les conséquences, sa mère est morte par sa faute
Mane sama dieucoeur nekoul fi ma deuk ak sama goro warr ko togal lou nekh di ko sagnsel bâ bou contane diko teral di sakou si môme gueureum ...mane dagay rayy sa gorro Ki mo Bonn wae😥
Merci papa sa genre yii l'Aniou sohla cii societe bi .le cas du papa ki avait tué ses enfants a Touba warna tah niou bayii khel ci louniou khamoul,pions pour le repos de son âme en attendant la suite. Paix a son âme
Man dal ma djomi si Sénégal li mba sén diam la tamit seuy daguan tass daguan so meunoul mougn démal ak sa jeukeur wala gua dem sa yon mo geun gnaw tef yignouy defanté sougnou biir gnoun dougnou ay toubab goro yi par force si seuy yi lagnou bok...Mére khady yalla nala yeureum té kharé la Aldjana
Daniouy liguey séne dieukeur yi ba louniou wakh sene dieukeur mome laye déf guéné séne wakeur yép bayiko fa mome késsé ak sa yaye kham gani tayouko way
Serigne cheikh dan'na wakh nan diamono dina nieuw nit'niei mélni mala 🐑 Mala'yi aussi ame comportement comme si ay nit / yalnako bour' yalla kharé'ko aldiana fir'daws si barki seydina Mohamed psl 😭😭😭
Mane mi dei damanan khana li goro sagnou KO deff gorom mane dei Sama goro Sama yaye la woor na yalla louma diakhal mom lay lathie Aÿ khalat té Sama yaye bima djour mongui fi
Salam tout le monde Je trouve bien bon le fait que vous nous mettez au courant de ce qui se passe par contre j'ai un problème Est ce normal de détailler une scène de crime ?? Meme la police ne se permettra pas de donner certaines informations après un crime de peur de ne pas trouver le meurtrier car ils auront à avoir des documents secrets pour leur enquêtes que seul eux et le criminel pourront savoir Merci d'avance j'espère que cette critique pourrait être constructive et que ça pourrait changer quelque chose
Aissatou Sylla weah u right mais gnak education ak boneu mo gui ci aussi entre le gars et sa maman c’est une chose et entre la femme et la maman en ai une autre tum saisi
Aissatou Sylla weah la ta raison aussi! En tt cas ya tas de trucs a revoir aissatou legui sou gnou valeur ak education zero! Ya truc qui vas pas ! Warr nagnou khalat sou gnou bopou sinon fou gnou narei moudié dou bakh li mom leer nama
Aye waye li metina trope les habitants de la maison nak bolen demei ba meuneu tolen deukeu cibir keur gui Guen yobalè sen yaye vraiment c tres triste ôté la vie d'une personne comme si ça t'appartiennait mais que justice soit faite mère bi yalla nako yalla yeureum
C bien possible yallah rék khamm na police déf ligueyame certes elle avait des problèmes et très agressive avec sa belle-mère mais qu'elle là tué woroul kéne fékéwoule donc nagnou mandou déf ndank ba affaire bi lére wassalam
Père ngua balma mais c’est pas a vous de donner des informations sur se conflit qui pour moi ne sont pas fondés. C’est le rôle de la police de relayer toute l’histoire et de mener une enquête. Yalla nako yalla yeureum te kharer ko aldiana.
Kou djigéne ki lane mo nék si gui nawame bamouye déf li kou djigéne ki taxawalou katla sa djeukeur néla kaye ma youbou leu ngue touki nga bagn taxawalou moko nekh kon🤷🏾♂️
Mane dal lègui xawma loutax xalè you djiguène yi bone noulène nèx lagnoul seuyè falè wougnou sène goro yi kousi am dieukeur rek bo sagnone mou déh tè beug sa yaye dounde
mane mone khamna diabar doyna seuk ndakh pour nga giss djigeeeen bu baakh meuneu toul nek si 2020 biii dieum kaw mo takh gnone goor dji na gno xolaat sunu bopo té bayé kou gno giss dougo thii
Ahhhh .... attendons les résultats de l’enquête 😏 d’après ce récit, on sait pas si c’est la fille qui l’a tué ou c’est un accident 🤗 Toutes mes condoléances à la famille éplorée
Le vieu li gua netali yeup pourkoi raconter toutes leurs vie privée l emprisonnement de son mari e vente de la voiture ça n à rien à voir avec l histoire
Qui dal nagnouko yar si casobi rek dina kham réw rekla wadji tamit ake sr reme yi saguane nagnou yalla nako yala yerem té kharél ko aldiana thiey Sénégal doynawar
khadi diouf c'est la tante de ma meilleure amie depuis enfance mais c'est vraiment triste maman khadi que la terre lui soit légère firdawsi soit sa demeure éternelle
🙏🙏
Rewe rek ak doff dofflou rek ba raye nitt rek nu nane tayou ko Sénégal diakhl nanu ma .😭😭😭😭😭😭
RIP
Yalla nako Yalla khare aldjiana firdawsi. .moi j'habite a côté
@@adamandiayeseck7853bilay rew rk
Parfois djiguéne gni danlay gris-gris ba do xam fooy taxaw walahi. Yallah nanou yallah maay djiguene bou bakh issu d’une bonne famille ❤️🙏
Amine bilahi metina trop
Moi j'ai peur de la prison yalnanou yalla moussal
Amine mousseul si nieup
Amine
AMINE thie mane ak gneup
Amine
Amine
Je crois que on a fait quelques chose à dieu tout c’est tuerie au Sénégal dieu vient nous en aide tout le sang qui coule repose en paix
Lolou moy deug c ta voir
"Sangue leen réwmi ak khol bou seet wala nguéne sangué ko ak déret " disait un sage ....
Sénégal khamo lein li nguen am sakh
sen niou bakh nioniou abal len niouko bok
Nga am dieukeur mou beugleu,dougueul leu thi keur,dilo diokh dépense,Dem wouti Bayila ak yayam amo loy def loudoul diko Ray...Mais Souadou Qui es-tu?😳
Bone rk moko diap dou lénène
Bone xole rekh
FATOU SAGNA ahhh kone sokhna si ray da am raison bou takh nitt war ko def? Dns tt ls cas ray bi dou yone
FATOU SAGNA quoi qu’elle puisse la faire,ça ne justifie pas le meurtre
FATOU SAGNA goro ak loumou sikeu sikeu seuy so meunatoul tasaal deim sa yoneu moguene li niaw na trop
Ha djeukeur dji kay moko raye kone akh li khéw yeup mou tok di sétane khana Dou djabar rek bou respéctéwoul sa yaye doko fassé après mou djékh
Wa salaam
50%diakeur jiée dé
Vraiment
Ay yéde yereume moka gueune
Ta diabar dioula gueuneu bone mola eup aye pékhé. Dinañou la kheireumtou ba do wakh. Wayé yala ngui lène di guiss
Mane tiiit naa sii diamono biii dé😳.Yalnagnou yallah mousseul sii dieuf diou bone té khiiir gnou siii lou baaakh.🙏🏻
LE MARI ET LES MEMBRES DE SA FAMILLE SONT DES IRRESPONSABLES. COMMENT PEUT ON LAISSER UNE SORCIÈRE SEULE AVEC SA MÈRE.
Vraiment
Vraiment
Domram rk
Merci
Pure vérité Mme
Sénégal, les gens réagissent toujours un peu tard ,yallna ko yalla yeureum la personne décédé xaréko ardiana firdawsi. Yalna yalla lérall léppppppp.
ANNA SERRERE Amine
Thiéy yalla Ay way li Lou mou don Ban Sénégal la niou nék légui chaque jour ak ligay dé si réseau sociaux yi yalna niou yalna niou yalla moussal si seytané 😭😭
Le jour où elle ira en prison elle va voir si ça valait la peine elle est impolie seulement ki respecte sa maman doit respecter celle de son mari
Kou respectéwoul Gorom dafa fékk mu ndieukéko thi yayam.
Yacine mar Diop bilakhi wakhatiko
Tu as raison kasso nekhoul
Es le cas
Yaye Awa Gueye Stp j’ai pas bien compris elle a tué sa belle mère avec quoi et pourquoi ?
😭😭comment une personne peut faire ça à une personne comme lui rip maman 😭
Sokhor rek
Kide nio bok konie
@@princessethiam5241 😱😱😱. Raye len ko
Adouna amoul solo maintenant elle est en prison on ne la pas encore juje dans sa maison elle a detruit des vitre aluminium ak ay ecran plat bou tolni cinema et elle adit sama dieukheur dinako def lo khamni day kharou elle a dit de sa propre bouche
Les images de la salle de bain devraient être censurées li c’est choquant la dame Yalla nako yalla yeureum t xare ko aldiana 🙏🏽
Bilay
Ay wayyyy ndeyssane ohhhhhhhhh masta 😓 billakhi c'est triste 😔
Mais naniou nianal ki guéneu adina,nianal aussi ki ray té mouslou si séytan....lolou reik mo am solo 🙏latia dess niou bayiko ci lokoy sounou borom😔🙏
Kéneu waral jujé kéneu ndak kou guénagoul adina hamagoul lanelako yallah réservél thi aveniram!!! yãh Räb 🙏😭😔
Sa dieukeur dé bou xamone ni yay ray yayam doula meusa tak ak yay nimou meil thi dôme yalla nalaa yalla yeureum yaw mi gueine adouna figa deim gueneul la figua djouguei
Walay souko khamone douko takk
Bilay😭😭😭
Ndeysane
Djiguen dal waroul am fit. Té djiguen bo khamni sou méré day yakh nitkou bone leu ba sokhor teksi ndakh yeureumo sa dieukeur dji nek bitim rèw si sèd ak thiono yimouy dathie pour teral leu teral yayam ngani doufi amé. Eyway ki yakhna famille way😭😭😭
Li rekk motakh ma raguala tak sokhna malgré djiguén yeup yémou gnou mais do kham koy wolou maman yalnala yalla yeureum kharéko aldiana firdawsi ak bép dioulit
Yalla nako yalla yeureum. Personnellement sama gooro moma diangal togue lep li diguen di sokhla rek momako diangual Yalla nako yalla yeureum té yékheniou
On a un nouveau problème au 🇸🇳 la psychopathie il y'a beaucoup de meurtres
Weuy Sénégal yakouna sama fitt bi rethiena nagne diokh thier goro yii en plus goor gni bayilén di djiteul sén diabar waa Sénégal khana légui ray dafa khéw diomina allahou ahbar 😭
Faites attention aux femmes que vous allez choisir comme épouse
D'après le père c'est la maman du mari qui l'a choisi
Cv
Bilay amna jigene you werul
Bou nit lérone Ken dou betteu kenneu. Ni goor Di taneh la Djiguen Di taneh nakh en général haleyi tamit gnoy gueuna payer les pots cassés
Yalnaniou yalla musal si djiguégni fitna. Duekar dji daf ka dane nekhal leigui nak raye na yayam ma khol nakh dinako nékhalati
Je crois que le chef de quartier à raconter fidèlement les questions qu'on lui a poser c'est mon avis je peux me tromper aussi
Merina torop ,mai je sui fière de c papa il est digne et respectueux .
Yar len sen doom yi, li yep niak éducation moko lal, nit so amoul yar amo dara.
Comme disait ma mère rek "koula rayal kou rew soula fayei kou dof dieuleul"
Qu'Allah lui accorde sa miséricorde ❤
lady maxi sa yaye wakh na wolof bou graw sah jtjur
Bien dit gniaka éducation rek
Bi lay😭😭😭li
Sénégalaises yi sene goro yi laniou deff ay rivales mais bakhna naniou dem rek
rose rouge bilahi aka ma méti
Je suis entièrement d'accord
ioe nk waax gua leiip
Nooo bou len wakh lolou kou nekk ak djikome si coté mère y ak qui di seuye, qui di seuye mo warone corrigée comportement wame enver sa belle mère, lii mome daaraye adouna doumako diarale soumala naré sagua dem bayi la ak sa keur 🙏🤲🤲🤲🤲
Nga sagn ko wax. Té koufi fowé sa seuy bamou tass nga djign ko belle mère wala belle sœur. Sonou naniou trope
Bilaye kou moye touwoul seytané do diogué thie def lou bone niowe bakhoule histoire goudi ak béthiek li rek léye diour yalla na yalla moussale niou thie seytané
YALLA NANIOU YALLA MOUSSEUL TCHI SEYTANE
Alahouma amine
Seytane defa am dole te graw sou la tope tank détourner woula dou am diam
@@safiatoudiallo6389 LOU WER NGA ADUNA DAFFA NAXAREE MOUTHI TROP
@@cheikhmbacke4379 bilaye
Goor legui douma am femme bou rew di def louko nekh kene dou wakh le jour ta frappe ma mère tu quitte cette maison goor daye responsable am foula
Sama khol bi moye metti ak yaye nimou sone si dome eumbe 9 mois bene beuss khaw la ray sa diarbat di fonto sa yaye ma bagne goor bou gnak fayda mere bi yalla na khippe sa aldiana firdaws 😭😭😭😭😭😭😭
C'est la faute du mari ,une femme qui terrorise tout une maison, et son mari na pas réagit avant.cest ça les conséquences, sa mère est morte par sa faute
Dou béne rapp Senegal kou raye nite rek niouné dafa doff🥺🤦🏽♀️ yalla naniouko teudj a vie Waay ki mo sokhore😭😭 que la femme repose en paix
Mane sama dieucoeur nekoul fi ma deuk ak sama goro warr ko togal lou nekh di ko sagnsel bâ bou contane diko teral di sakou si môme gueureum ...mane dagay rayy sa gorro
Ki mo Bonn wae😥
Délégué bi dal Sop naka trooop🥰
Ay waay domou mère bi naka layy neketi nitt sa djiabar moo rayy sa yaye , loyy wakh say domes bounoula ladjié sen mames yaye boye repose en paix
Merci papa sa genre yii l'Aniou sohla cii societe bi .le cas du papa ki avait tué ses enfants a Touba warna tah niou bayii khel ci louniou khamoul,pions pour le repos de son âme en attendant la suite. Paix a son âme
Yalla nako yalla xaré aldiana🙏
Kiiii djigueen kou bonneu leu bilahiii dieukeur djileu kou yarre sa kouyy bamou magg yaw lay ndieukeu mbeukk boule sonnou beugue djiguen diko bayi mouy def liko nex beu rayye sa yaye rip😢😌
Doy na warr, naniou tapé xol yi en plus on est en plein mois de ramadan
Betenama trope Souado elle a grandi sou mes yeux très calme a son enfance. Ainsi nul ne connais vraiment son prochain
Man dal ma djomi si Sénégal li mba sén diam la tamit seuy daguan tass daguan so meunoul mougn démal ak sa jeukeur wala gua dem sa yon mo geun gnaw tef yignouy defanté sougnou biir gnoun dougnou ay toubab goro yi par force si seuy yi lagnou bok...Mére khady yalla nala yeureum té kharé la Aldjana
Amine
Aminne
Amine
Paix à son âme
Bousso bali dama dite thi Sénégal man
Seyou mbocou cou mene deco evité amoul bene ndaringe ahí problem rekk dangou sofffff bilahiiiiiii 😎😎
Sa Goro soko teraloul mayko diam ak salam sama mbokou djiguene yi nagn kholat sen bop goro soko defei ni sa yaye sen deuk nekh
Bilayy yawe
Vraiment
Wallahi
Billahi l~gui femme yu Bari danio bone
Bilay goro yomoul dhe
Wayé ma khala goor yi légui taar laniouy takké kholouniou koulen beug ak koulen yieuram yalla nalen yalla doli soutoura
Sa goro gua khamni mola diourale sa diekeur
Ndeye fatou cissé bilay yaw
Bilaye
Domou bay ki yakh dérou jigén gni
Bilaye
Yalna khippe aldiana bibarakaty cheikhoul khadim. Une mort atroce. La vie ne vaut pas la peine.
Yalnako yalla yeureume djiéguelko tés kharéko aldjiana c'est vraiment triste
Yalla naniou yalla yereum si barké yonentébi SAWS
Khady Diouf è c k amoul ay rab 🙄mais bref k la dame l bon Dieu l'accueil dans son paradis éternel amine 😭métina trop walahi 😭😭😭
Daniouy liguey séne dieukeur yi ba louniou wakh sene dieukeur mome laye déf guéné séne wakeur yép bayiko fa mome késsé ak sa yaye kham gani tayouko way
Incroyable yalla nagnou yalla mouthieul thi gaur bou faible de caractère irresponsable
Repose en paix maman. Amine
Allahou akbar allahou akbar ya raby protege nous😭😭😭kell3 mechancete
legui dale Sénégal ray niit comme boire un verre d'eau
Serieusement
Nekhoul mais j'aimerais voir domou président wala domou ministre bouniou ray pour voir leurs réactions
Bilayy yawe
@@SouverainisteTV lolou yakamti nako dakh yalla justice âme
@@harrypotter2807 ah légui gayi daniouy réy comme c'est pas possible hana bouniou domou prési peine de mort dina am
Machal allah mon père vous avez bien parlè
Faux!! Il a trop parlé !!!
Lifimou am souriwoul sunu keur bilay ki bonena
Bolénii tak diabarr délénko kholate
Tout a fait kou bax ki
Bou djiko change nak.kou beug esk nekhna guiss djiko bou boon bi?
Bilahi koussi topeu tare wala ayeu tate torokh rekk
@@ibralo1998 surtout
@@tapha76 kirasulaaay malheureusement c'est la triste réalité
Serigne cheikh dan'na wakh nan diamono dina nieuw nit'niei mélni mala 🐑
Mala'yi aussi ame comportement comme si ay nit / yalnako bour' yalla kharé'ko aldiana fir'daws si barki seydina Mohamed psl 😭😭😭
Allah akbar repos en paix 😭😭😭😢😢😢🙄🙄🙄🤔
Merci beaucoup darkabuz sen liguey rafet na trop
Cette femme est sadique, mais le mari a préféré sa femme, que sa mère fils indigne
Ayi way yalla nako yalla kharé aldiana
Seuy dalleu bossi amouleu diame tassaleu gua demeu diame nei nioy nak li niaw n’a trop ak louniou la meuneuti defeu ray dou Yoneu elle est agressif
Vraiment vraiment vraiment
Yakar na kila diourel kigha begue warr gha déff ligha mane ak ligha manoul bamou contane més pa li niaw na torop
Ki moye dmr gooro nimou nexe man de sama gooro moye sama xarite
Wa waw nonula yalla nala yalla defal diam sisa seye
Fall penda dokorethiou
Mane mi dei damanan khana li goro sagnou KO deff gorom mane dei Sama goro Sama yaye la woor na yalla louma diakhal mom lay lathie Aÿ khalat té Sama yaye bima djour mongui fi
@@diabintou2152 bilaye walay
@@khadimseck1424 amine 🙏🙏
Salam tout le monde
Je trouve bien bon le fait que vous nous mettez au courant de ce qui se passe par contre j'ai un problème
Est ce normal de détailler une scène de crime ??
Meme la police ne se permettra pas de donner certaines informations après un crime de peur de ne pas trouver le meurtrier car ils auront à avoir des documents secrets pour leur enquêtes que seul eux et le criminel pourront savoir
Merci d'avance j'espère que cette critique pourrait être constructive et que ça pourrait changer quelque chose
Yal nayou yallah sounou borom moussal si seytané
Amine
Amine
La culpabilité du fils sheuu😭😭😭😭ki gueumouma ndakh dina takati sokhna
Que la terre d'Allah 🙏 lui soit légère 🙏💕
BILAE WALAE MANE DEI KOULAL SAMA YAYE .WAKHOU MALA GUANAN DAGUAY RAYÉ .BILAE MA RAY SA NDAY 😢😢😢😢DOMRM BIMOU DONE .KÉNN WOLOTOUL DJIGUÉN LÉGUI YII
😱😱😱😱😭😭😭😭🤭🤭🤭🤭🤭
Goor bou faible bakh yalna yalla moussal c vraiment triste
Dou kestion de goor bou faible plutôt koi djigen ki mo bonne rek !!!
@@xewxew22 faible mogui si nakh goor legui khama tou lane moye yaye
Aissatou Sylla weah u right mais gnak education ak boneu mo gui ci aussi entre le gars et sa maman c’est une chose et entre la femme et la maman en ai une autre tum saisi
@@xewxew22 mère bi dom pourquoi l'avoir laissé seule vivre dans cette maison c vraiment triste dom legui zéro affection
Aissatou Sylla weah la ta raison aussi! En tt cas ya tas de trucs a revoir aissatou legui sou gnou valeur ak education zero! Ya truc qui vas pas ! Warr nagnou khalat sou gnou bopou sinon fou gnou narei moudié dou bakh li mom leer nama
Mane dé bouma manona indi wateu sama boss DINA khalat lénén bamou DESS Ray Gueye dioro yala na yakham ya séd
Je comprends pas toutes cettes haînes dans le monde 😭 paix à son âme 💔
Allah Akbar Ay way ki mon sokhorr té bonn😭😭
Son mari doit être interpellé car il est complice d'avoir laisser avec sa mère une telle femme folle furieuse
Sénégal 🇸🇳 daniou wara bayii kou ray nitt rk niou naneuh ayy dfa doff wla lane dra dalou leine nioko tay blh mei repose en paix maman 😭😭😭
Tu es entré dans trop de détails. Ces explications ne doivent pas exposées au public mais plutôt aux enquêteurs.
Faites attention.
Yalla nagnou yalla mousseul si seytané. Sama wa quartier dougnou meusseu faté lii thiey adouna
Kou ray nitt dan la wara ray Sénégal ay doméram rek niokay djité dano wara bayi teudje tay atté attépp islam
Aye waye li metina trope les habitants de la maison nak bolen demei ba meuneu tolen deukeu cibir keur gui Guen yobalè sen yaye vraiment c tres triste ôté la vie d'une personne comme si ça t'appartiennait mais que justice soit faite mère bi yalla nako yalla yeureum
YALLAH na ko yallah yeureum té kharé aldiana Amine 🙏🙏🙏
Nous sommes dans quelle monde qui mo bone yalla naka yalla yerim hare aldiana firdawsi
Allah akbar
Kii moo niaff ndéme deugue deugue. Niou fassé leu nga tokk si Keur gui. Son ex mari aussi moo def lii yeup. Yaaye dafa fort dagnkoy sécurisé.
D'après li pabi Wakh est ce que méré begoul wone sangou mou gliser danou violament marmite ndokh bou tangue sotékou si kawame yala rek mo kham
Exactement c’est ce que je pense
Bien réfléchi mais n'empêche khalei bi rewna
C bien possible yallah rék khamm na police déf ligueyame certes elle avait des problèmes et très agressive avec sa belle-mère mais qu'elle là tué woroul kéne fékéwoule donc nagnou mandou déf ndank ba affaire bi lére wassalam
J'ai pensé à cette possibilité
@@salioufall802 donc rewna rek elle doit être la meurtrière
Père ngua balma mais c’est pas a vous de donner des informations sur se conflit qui pour moi ne sont pas fondés. C’est le rôle de la police de relayer toute l’histoire et de mener une enquête.
Yalla nako yalla yeureum te kharer ko aldiana.
Ce vieux est fausse
Nama yallah balle mais moi je ne vais jamais épousé une femme que j'ai pas connu son enfance mieux
Yalla nagnou Yalla mousel si dieuf diou gniaw
Dama yakarni wahh keurgui nio sagaane rkk rawatina dieukeur dji..!! Teksi seuyou mbokk warnagn ko kholatt problème bou am niou ndeup ndeupeul ko ba moussiba moudieh am..!!
Kou djigéne ki lane mo nék si gui nawame bamouye déf li kou djigéne ki taxawalou katla sa djeukeur néla kaye ma youbou leu ngue touki nga bagn taxawalou moko nekh kon🤷🏾♂️
Dafa am goor you yambaré wayadi irresponsable niak fayda
Demba amena jieguéne you Bonn sounou léne také danouy liguéy sene diekur banou bayi sene famille yalla nanou yalla mousele si bonn
Goor bi mome dome harame la
Niak diom
Fa mati yam la comasée wayé khalébi rewna trop wayé wadji tamitt khamoull akhou yay badiko bayi ak kou mélni ahhh yalnako yalla djégeull yereumco
Djiguène bou âme fitt bakhoul
sénégal guiii man dama diakhlé...nanie ko rayatt rékk
Yalnagn yalla defal sago té may gnou diabar diou bakh
Bayilene neque souadou esk werna tamite yene yi tamite kou normale mounouko tamite dee
Kouy déf lo guiss tak yaga tak lou bone rék
Mane dal lègui xawma loutax xalè you djiguène yi bone noulène nèx lagnoul seuyè falè wougnou sène goro yi kousi am dieukeur rek bo sagnone mou déh tè beug sa yaye dounde
Yalla n gnou yalla may ay soxna you bakh🙏🏼
mane mone khamna diabar doyna seuk ndakh pour nga giss djigeeeen bu baakh meuneu toul nek si 2020 biii dieum kaw mo takh gnone goor dji na gno xolaat sunu bopo té bayé kou gno giss dougo thii
Jiguén gnou baah gni en pagaille,gayi kay nioy top jiguénou sheytané yi,wayé niou am diné yi bah nane
Son Mari est vraiment nul. Bayi sa Yaaye ak Doméram diou mélni si sa Keur. J'ai vraiment très mal.
Ahhhh .... attendons les résultats de l’enquête 😏 d’après ce récit, on sait pas si c’est la fille qui l’a tué ou c’est un accident 🤗
Toutes mes condoléances à la famille éplorée
Doom dji niemana ray yayam
michou diaw talibe baye Niass Diaw je parle de sa belle fille et non de sa propre fille
Le vieu li gua netali yeup pourkoi raconter toutes leurs vie privée l emprisonnement de son mari e vente de la voiture ça n à rien à voir avec l histoire
Sa c vrai. Il n fallais mentionner cela.jai déduit la même chose.
No vieux bi defeant la pourquoi exposé vie privée diambour limoye médecin après la mort
Qui dal nagnouko yar si casobi rek dina kham réw rekla wadji tamit ake sr reme yi saguane nagnou yalla nako yala yerem té kharél ko aldiana thiey Sénégal doynawar