Est ce que la mère a joué son rôle de mère ? . Le Monsieur je ne le défend pas mais il ne s'est pas marié avec la mère mais plutôt avec sa fille . Kou mayé sa dome warko bayi mou doundou avec son mari
Non Cissé ce qu'il a expliqué c'est claire " il a acheté la maison par le biais d'une procédure normale". En plus c'est 30 ans après que les enfants du vieux se réveillent pour crier "arnaque " faut arrêter quoi...
Dala nakh ba dieunde keur gui c sa la vérité la dame n'avait pas conscience de ses fait car elle était dans le besoin ndeyssane.amoul wonn dome bouko takhouwou pour lep lérr .yalla naniou yalla mousseul si genre niit yii
khana déglouwa. c'est pas la maman qui a vendu c'est le tribunal qui a ordonné la vente et confiée celle ci à un notaire. koumou nekh jeunde. mais souma nekone mome douma dieunde car Sénégal dafa compliqué la preuve kholal liko si fekk tay
Ce qui n'est pas clair,il a donné 6 millions à l'autre famille,et es ce qu'il a remis le reste des 13millions à sa belle famille ??? c'est vraiment louche.en plus,il s'en profite pour effectuer un prêt à la bhs.s'il n'as pas donné le reste de l'argent à la belle famille,la procédure de vente doit être nulle.
Mais toi tu devais etre un Gentleman si reellement tu aimes sa fille tu devais soutenir la famille sans pour autant etre responsable de cette forfaiture .
Et bien guisgua toi ma fille hawma fillette noumla nakhée ba guenné sa yaye keur bii bis dina nieuw sa sera a ta place mou guenéla dem taki kenenn doff que tu es 😢😢😢sa propre yaye
Ce gars est trop bavard. Je ne lui fais pas trop confiance. Pourquoi il n'est pas allé chercher une autre parcelle et construire là-bas. Il a déroulé son plan depuis le début et roulé la famille. J'ai travaillé avec pas mal de transitaires mais le plus souvent diouthie ndiathie laniouy dèf. Mangui diégalou
Grand outilll keurr 😂😂😂 wakho fii darra 😂😂 demal thies walla keurr massar ya des terrains de 3 a 4 millions moo gueuunn gua topp sii keur diambourrr guii
@MoussaCisse-rh6bq ça peut cause des problèmes par ce que les femmes sont dangereux pour indépendants seulement il faut éviter les matériels de la belle famille
Lo beuga mou bayi nonou nouy salirè petit femèm avan mouy am ndiabott tolorèna bou amè ndiabott manatoul liguèy normal ndakh djiguènn nioniou sounou togann normal yarou li lèpp dou am ki kouka guiss khamnni limou dèf sakh ganalouko dafa dèm ba Seuss
Cette histoire est louche à cet époque les enfants n'étaient pas majeurs à part leur grande sœur ta femme donc toi tu as profité de cette situation pour faire ce que tu as à faire
Le rapport avec les enfants? Même les enfants mineurs domou bayi Sougnou decider diay keur gui pour niou meune mirasse sougnou deimei si Yonne tribunal daf diay keur gui pour sedelei nieup am Sen wal. Pour les enfant mineurs c’est leur tuteur ( ici la maman) légal qui récupère leur part. Grand bi niouy saga dieund rek leu def 🤷🏽♀️
Vraiment maçon yi dagn lén wara yeukeuti ay goor yalla deugu té si risque rk lagnouy liguey ndeysan yalla nalén yalla doli soutoureu ak werr mais ki baxoul gnak na soutoureu nitt lo def waxko amatoul chance bou xolé lou yobou goorgui douko fi bayi dina xamné aduna dou keur
Louma diakhal moy keur gui com dieunde ngako legui niome ani sen xaliss ?dégouma fén foko mentionné 6millions yi wakh ngako té lolou domou bayi laniouko diokh legui le probleme moy le restant de l'argent kane moko yor?
Le gars dale boko dèglo doul rek lay def. A part les 6 millions verser a lautre famille il na aucunement dit largent verser a aa belle famille. Ki kou bone la
Bilahi limay bayi khél dafa mélni nitt gni dougneko bayi khél ki néna papay boy yi 1992 la décédé ta mome 1996 la tak ndiaya 4 ans après gnouy soga wax wakhi diay domou bayou boy yi fougne nékone ta boy dieund ta yor khaliss bo mome lousi yonou banque bagay taylé keuyitou keur gui bilahi bo yoroul wone keuyitou keur gui do guéné deureum yor ndieugou keur gou bakh diamano yoya di dougeul sa khaliss ci keur gokhamni néga dafay inondé yorowone nagoul rék keuyitou keur gui nékone sa lokho mola may lou bari
Yaw wero le titre de propriété n'était pas muté en son nom propre banque ne peut pas accorder un prêt sur cette base toi aussi . Il a obtenu un prêt parce que il était un agent de maersk donc il avait un compte courant et comme tribunal mo diay .les papiers de la maison . Ci greffier bi lay nek
Da ngay tothie sa lefeul ndeye doul bilahi katal sa data ndeye sa yo yéwo bilahi souma deukone si kogne ba heure bi ma ngui si kasso ba kone deugue na sa ndeye bou yague goordjigén nga rék li defma métti trop je te jure je cherche pas à comprendre
YAW VRAI GOROU YALLA NGA....LII NGA BIDEU RECK ...WONENA SAYE YENÉ .BOU DOME BOU BAH DI DEFAL .AYES WA DIOUREUME...NASA DIAM YAGUE NOU BOUKEU..AAMIIIN... SALLALAHOU ALA MOUHAMADIN SWAS
@faaadadju7101 ECOUTEZ !!!! JE CONTIONNE PAS LES INSULTES....J AI JAMAI INSULTE SUR MES COMMENTAIRES....C EST SON INDIGNATION...SS POUR AUTANT FAIRE VRAIMENT ATTENTION AUX INJURES ....SINON JE L AURAIS CONSEILLÉ QU IL PEUT COMMENTER SS INSÛLTES....ET JE VOUS REMERCIE DE VOTRE REMARQUE....TOUT DE MM JE MAINTIEN K NIT BOU THIEUREUL WADIOUL LA. DI DIEGUEULOU NDAH SAGUA BAHOUL TÉ RAFETOUL....SI JE PRENDS LE TEMPS DE VOUS REPONDRE ..C PARCEQUE BOUGUOUMA TOGNE ...JE POVAIS ME FOUTRE DE VOTRE REPONSE....MAIS. PAR. ACQUIS. DE CONSCIENCE J. L. FAI PA...TÉ HAMNI YALLA DJISNA LOU NIT DEF...TÉ DIOULITE AKHANE LA NIANE NEKEKO FA YALLA....ENCORE DI DIEGUEULOU BOUBAHABAH.... WA SA
Diabar dji bi gnou ko ladjé defané xamoul Keur gui si tourou Kane le nék. Après mom mouné diabar bi gnou ko ladjé da né dieukeur dji mo ko mom. Té bène wakh defmeu frapper wa dji néneu féne katt dafay meuneu wakh😂 mais je trouve qu'il parle trop.DIEU seul sait. Wassalam.
Bi Senghor di wah l’émotion est nègre dioumoul. Juste parce que mère bi mingui thibiti les gens perdent la raison totalement alors qui loumou wah c’est très logique.
Ki Kay limiy wakh rombouna deug ndakh limiy wakh lèp dafa verificabile Senegal nak mom affair de farfarlon moka yakh mo mom yeufeum te def na lou bakh ba fika kholam yam lo louy problem bi🥳
Non nelawoul c'est juste que sa belle sœur lui pourrissait la vie et sa mère était de mèche avec elle qu'est ce que tu veux qu'il fasse au final laisser sa belle sœur diviser sa famille ou l'expulse tu sais quand on atteint un point de non retour on est obligé de faire les choses brutalement
Pourquoi tune leur a pas dit que tu as achete la maison des le debut au lieu de leur proposer de signer( meme les mineurs c'è qui n est pas legal !!! ??? !!! ) pour un pret bancaire qui sert a retapper la maison ? Tu n es pas fiable a 100/100 Mais a -0%
C'est la ou se trouve le problème,il devrait les informer et en plus devant des témoins comme le chef de quartier ou les imams du quartier et notables....
Kona mere bi dafa diaxlé ndax dagnou nara diaye keur gui mouy lepp pour djunde ko yaw nga djundal ko sa bopp Yaw yaye domaram deug sa kanam bou mokk ndeyam bi 😢
Depuis le début je me suis dis que wadji teuboul teup rèk ni mo mom keur gui. Et que yaye dji soit dafa comprendroul wone ni ki dafay dieund keur gui pour mom,soit khamone nako mais mo expliquer woul khalè yi la vraie situation. WAYÈ linguèn def niaw neu. Expulsion mo waroul wone. Même si les enfants attaquent, nga dem justice pour niou xamal lène ni momouniou keur gui., mais dafa NIAW parceque yaye dji mak leu. XALÉ YI AUSSI DÈLÈNE WAKH AK SÈN WADJOUR YI BALA NGUÈNE DI ATTAQUER AY COMBATS parfois nga nèk ci keur tè do khol nou keur gui dèmè. Nga kheuy rék commencer am wètiètte, di lidieunti ay keuyitou keur ba andil sa bop problème. Parfois les parents pour soutoural ndiabote daniouy def ay sacrifices youniou meunoul expliquer rien que pour beug soutoureu. Tok lèn ak sèn yaye nguen wakhtane ak mom. ABDOURAHMANE. Outeuleul sa goro foumou deuk. Li niaw neu si sa der .
Vraiment tei au final nieup si bénéficier wou. Parce que quand même niom gni di wah niougui si keur depuis 2005 sou len beugone gueinei il allait le fait depuis. Mais doumeu leu fat saama keur beu parei gamay tongal makk sama diamboot Moi je suis totalement d’accord avec lui
Ce guy est très dangereux un menteur professionnel 😢 il avait tout prévu jusqu’à ce moment 😢 punaise il se rappelle de tout vachement tu es fort 😂😂😂 avec tous tes preuves que tu viens de citer il va falloir une sacrée paire pour pouvoir ce tenir tête avec lui😂😮😮
C’est un conseil pour nous tous . Faisons très attention à l’héritage car il divise les familles. C’est la première connaissance qui disparaîtra chez les musulmans selon le prophète Mohamed saw
Sama alouwa soriwoul deh wayé donn na degg ben waraté katt mouy wax si mirass. Néna chariya dafa wax ni borom keur sou gagno nagnou mirass keur gui kouné niou diokh ko walam mou dem. Sou gnou mirassonn keur gui bou yagg problème bi dou am.
Non se diabar waxoul né ya ko mom dè. Bi gnou ko ladjé da né xamoul si bane tour le nék. En tout cas semeu wadji téguil se loxo fi ngue ko ték baxoul si yow ak se ndiabote😮
Pabi loumou done ak limou donoule lépou kén ladioulako depuis le départ woor nga si dioublouwone nith na ragal yalla guiss nagnoufi louné lingaye wakhni lépou dangadone wouthe ningaléne diéko wassalame
Tribunal yoon la kham. Arrêter ce mascarade et trancher la vérité. Ce genre de problème sa ce régle au tribunal. Il a raison de suivre la procédure en justice, sinon en cas de décès ses enfants seraient expulsés de cette maison.
C est la catastrophe ce mec il a simplement abusé la famille c est sa femme que je plains et ses enfants aussi Alal Diaroul li il n a pas d arguments ndeysanne niaw n’a torop
Tu dis ce que tu as fait personne ne la fait c’est vrai car c’est ma première fois d’entendre quelqu’un racheté la maison de ses beaux parents car ils ont des problèmes 🤣🤣
Yaw dé lougnou la wakhale, ya ko def. ak sa baate bou lakh. Meme si la dame t'avait vendu la maison, waron ka nga ko rouss guéner. Tu n'avais ni terrain, ni maison, nga user de subterfuges et manigances, ba dieule leur maison. Honte à toi, qu'ALLAH te punisse sur terre et à l'au-delà. YA BONE, YA YESS
Mn père vraiment waro wone douguou si keur djabour mirasse dafa graw tei adouna dou keur yalla nagnou yalla attei si yeurmandé🙏🏽🙏🏽
Keur gui justement tribunal daf ko diay pour niou meune ko mirasse. Je ne comprends pas pourquoi warou ko wone dieund
Boko déglo sakh gua khamni féne katla
Koussi sa yone nékoul rek lalal j aime
Dama khamni ligua fi wah deuge deuge kéne menoussé tek léléne wah degue yala sénégalais yi mendouwougnou
Kheuthio woo sa keur baye di kheuthio keur bayou diambour vraiment meune nga togne 😢
Bonn rek
Tu as de la chance ndakh dama bayi saga sinon manila kou niaff sa ndeye nga.
😂😂😂
😂 sagana
😂😂😂
Ehhh
😂😂😂😂😂😂😂😂
Si un jour mon mari met ma mère dehors avec tous ses bagages. Je sors avec elle et divorce s'en suis. Yaw kou bonn gua😢😢😢
Est ce que la mère a joué son rôle de mère ? . Le Monsieur je ne le défend pas mais il ne s'est pas marié avec la mère mais plutôt avec sa fille . Kou mayé sa dome warko bayi mou doundou avec son mari
Mane kou torokhole sama yaye ma bayila sa diabar nake dou moudiou fou bakhe
@@joeba5199 figua yobeu wax bi da sori. Je parle dans ce contexte. Pourquoi acheter la maison pour les foutre dehors après. Nitt kou bax dou dèf li
Bilaye wallaye, ki kou ko khôl kham ni féne katte la
Et si ta famille fait le blâmables
Tu as roulé la famille dans la farine pour profiter de leur bien
Bien dit merci beaucoup
Bilahi ki
Ki kaay baam la bilahi
Non Cissé ce qu'il a expliqué c'est claire " il a acheté la maison par le biais d'une procédure normale". En plus c'est 30 ans après que les enfants du vieux se réveillent pour crier "arnaque " faut arrêter quoi...
BIEN li gna wakh nonou la demeee dakh man si kogn bi la deukk ki day doul mouniiii merrrr bi dou torakh tes tayyy torokh lo gna ko
Koula khol khamni doulkate nga sa diabar kou niafff ndayam leu
En tout cas dal niaw na té do nite kou bakh boudone sa yaye doko guéné. Sa diabar kou bonne la. Boudone mane ma sour leu
Walahi
Mok diabaram nio yam 😢
Simple maçon, quel mépris social 😢
Waye gathe ngalama pa bi gor gorgorlouna ba bayi fi lou math heritage. Ni ma bagne genre yi. Quelle arrogance !
Walahi qu'elle arrogance simple maçon ki d'où nite
Billy ki domeram leuuuuu imbecile
Ki kay vrai domrm degue simple maçon mayla sokhna gay diay reyyy
Ki mo bone simple maçon nak khamo nou pabi def ba tabakh dougeul diabotam mayla domame amo loy def lou doul li 😥
Simple maçon Thiey yalla
Warone nga roussa fègne ndakh boudone sa ndaye dokko torokhal vraiment do nite kou bakh
Ki kagn sagn na toroxal ndayam sax nimako guissé
Lerna
ki dale amoule loumou wakh dey patiné rekkkk ay wakhame amoule cohérence sakh tu as roulé la famille rekkk
La traduction Google 😂
Ki defoul dra domou merbi mouy diabaram ken guenouko nek dmrm bayi sa dieukeur di toroxal sa yaye
Dala nakh ba dieunde keur gui c sa la vérité la dame n'avait pas conscience de ses fait car elle était dans le besoin ndeyssane.amoul wonn dome bouko takhouwou pour lep lérr .yalla naniou yalla mousseul si genre niit yii
khana déglouwa. c'est pas la maman qui a vendu c'est le tribunal qui a ordonné la vente et confiée celle ci à un notaire. koumou nekh jeunde. mais souma nekone mome douma dieunde car Sénégal dafa compliqué la preuve kholal liko si fekk tay
@@aissatou6586 tu as bien dit
Sénégal lo deff si Lou bakh niou fey la lou bone
Thiime ya niakhou diome rousso di guenner sa Gooro ya boone ❤
Ki kagne ténouniou mené féne bouniou wakhé ba paré rék gua né guoggo niawwww na
KEUROU SIMPLE MAÇON BI NGA DIEUNDE CI AY DJIRIM...DANGA WARONE SÉT BÉNÉNE KEUR NGA DIENDE KO
Wakh deugue Yalla 😅
Ki bo ko kholé sakh ga kham ni dou nite koubakh té yagui lor sa diabot😢
Te simple maçon mola may djiabar dh
kikayyyy amoule diome sakh
Walahi
Wakhofidara. Koula dégue khamni kou mana féne nga
😂😂😂😂😂
😢😢😢😢
Billahi
Srx ki wah neu lepp… limou wah da lerr nagn
Quiquonque qui échange la lumiére contre l'obscurité le regrettera !😢
Ndeyessane pabi diare na founek pour am keurgui nguir ndiabotame
Sétal si Yalla ngua bayi keur gui
Sokhna si kou fatou dagnou la wara Mirase . Boudé amna kou menoul dieund si famille dagnouy diay kénén kou meun dieund
Ce qui n'est pas clair,il a donné 6 millions à l'autre famille,et es ce qu'il a remis le reste des 13millions à sa belle famille ??? c'est vraiment louche.en plus,il s'en profite pour effectuer un prêt à la bhs.s'il n'as pas donné le reste de l'argent à la belle famille,la procédure de vente doit être nulle.
Li motakh déglou béne version rek di juger wauroul...bayilène di démé émotion ak passion....mane dal damassiy mandou bayi tribunal juger.
Wadji waxul deuk sokhna si ki loumou Wakh Dara léroul si daflèn nakh régler papier bi sen kaw ki Amoul ben vergogne lou nieup wax Moy deug ki day fénn
Mais toi tu devais etre un Gentleman si reellement tu aimes sa fille tu devais soutenir la famille sans pour autant etre responsable de cette forfaiture .
C’est ce qu’il a fait pendant 20ans. Domi mère bi kay nio mayoul diam ay diambotam mou dakk moi je suis d’accord avec lui
A ce qu'il paraît niom nioko yobou police.
Il est très arrogant
Tu es avocat du monsieur ou quoi tu répond à tout les messages madame @@ndeyefatou4374
Et bien guisgua toi ma fille hawma fillette noumla nakhée ba guenné sa yaye keur bii bis dina nieuw sa sera a ta place mou guenéla dem taki kenenn doff que tu es 😢😢😢sa propre yaye
Ce gars est trop bavard. Je ne lui fais pas trop confiance. Pourquoi il n'est pas allé chercher une autre parcelle et construire là-bas. Il a déroulé son plan depuis le début et roulé la famille. J'ai travaillé avec pas mal de transitaires mais le plus souvent diouthie ndiathie laniouy dèf. Mangui diégalou
Il m’inspire guère confiance
Je partage ton avis
C louche vraiment
Je n le connais pas il est logique dans ses déclarations et juridiquement c sa maison
Mais il fallait pas être là e cerveau de ce fardeau car c'est la mère de sa femme
Oui mais le restant de l’argent nako dioxer. Il a juste verser les 6millions
@dieynacisse8511 moi je crois que il as bien préparer son plan des années
@@CheikhtidjaneSeck exactement
@@mamebacs6622 c'est un malin vraiment
Grand outilll keurr 😂😂😂 wakho fii darra 😂😂 demal thies walla keurr massar ya des terrains de 3 a 4 millions moo gueuunn gua topp sii keur diambourrr guii
Keur massare 4m? Lolou fanela si keur massare ?
@@mafatimseck3662khana thiés mé keur masar mom amoufi
Fane si keur massar?
2millions sax Am na keur massa mais zone youye tah le
En tout cas ay wakh mom ça son mal au oreille
Wakhetane léne rk diameuh rek mo ame solo yallah na yallah tappé sénni xole amine
Le faite d acheter la maison de tes beaux parents c'est honteux. Il ne fallait pas acheter la maison
En quoi c’est honteux ? S’il l’avais pas acheter le tribunal allait le vendre à quelqu’un d’autre les obligeant à sortir de force de la maison.
A bon ? Lolou louthi nek? Damay ladji rek nak.
Mane dama contre kou dieund keur beau parent t meyoo len ko mais sou dieundoul wone fii niou diayy ko kenen khale yi nio waroul demm justice
@MoussaCisse-rh6bq ça peut cause des problèmes par ce que les femmes sont dangereux pour indépendants seulement il faut éviter les matériels de la belle famille
@ Daga contre kou dieund keur beau parent tei mayouleine ko ? Yeine Daguen khorom. Theatre guen di dound 😂😂😂
Et ta femme dans tout cela? Elle peut rester dans la maison et laisser sa mère dehors 😢😢 pauvre d'elle !
Degue degue
Mais yaye dji mo gueinei bopam loutah ?
Police moléne géné @@ndeyefatou4374
Bari gua wakh torooop de toute façon lii gua deffff Dara réfétousi
SAWAY TU AS PROFITÉ DE LA SITUATION DIFFICILE DE LA FAMILLE POUR LES ARNAQUER DE LEUR MAISON FAMILIALE.
Bilay walay non vrai imbéciles vrai profitare leu
C’était juste que ça limoudone déf yeupp juste pour ték lokhom si keur gui
Ki sathie Bou gname yalla la bilay
Yow deh ya niak soutoura. SoubhanaAllah
Lo beuga mou bayi nonou nouy salirè petit femèm avan mouy am ndiabott tolorèna bou amè ndiabott manatoul liguèy normal ndakh djiguènn nioniou sounou togann normal yarou li lèpp dou am ki kouka guiss khamnni limou dèf sakh ganalouko dafa dèm ba Seuss
Cette histoire est louche à cet époque les enfants n'étaient pas majeurs à part leur grande sœur ta femme donc toi tu as profité de cette situation pour faire ce que tu as à faire
Le rapport avec les enfants? Même les enfants mineurs domou bayi Sougnou decider diay keur gui pour niou meune mirasse sougnou deimei si Yonne tribunal daf diay keur gui pour sedelei nieup am Sen wal. Pour les enfant mineurs c’est leur tuteur ( ici la maman) légal qui récupère leur part. Grand bi niouy saga dieund rek leu def 🤷🏽♀️
@@ndeyefatou4374 ioe hana mbokam nga? Sonou nga ci diko defendre dh
@@ndeyefatou4374carrement gni danio badola en plus mere bi dou goor
Bilay yaw ya Niak Diom nga worone dieumdeul sa Goro keur mayi co yobouco makka ya buone yayi domérame thiiimmm
Guéminieume bou toye, ki dou nite
koula wakhné Mane nako
Ki d'où sa nitt
Geumou mala dee simmm 😢😢
Le mots simple maçon bingay répété pour lanla maçon waroul am keur vraiment warouna😢
L,être humain surtout le sénégalais aime rabaisser.
C'est leur nature hors la maçonnerie est comme tout les autres corps de métier
Dh keur simple maçon bi la taylé banque pour am keur dou rouss sakh
Ki dafa Kata ndéyam rec Mouy nane simple maçon
@@assanelo4614 taf lenena diay khél nakh lene
Vraiment maçon yi dagn lén wara yeukeuti ay goor yalla deugu té si risque rk lagnouy liguey ndeysan yalla nalén yalla doli soutoureu ak werr mais ki baxoul gnak na soutoureu nitt lo def waxko amatoul chance bou xolé lou yobou goorgui douko fi bayi dina xamné aduna dou keur
1995 amoul bene bank senegal bou fi diokhe aye carte bancaire aye code aye garb dengueye doul
DIAXAL NAMA DAL
Li ladone seet di 1995 carte gab
Peut etre carte cab bcao
Amone na dh dab mingui commencer am 1990 ba 2000 mais 2010 la am dolé
Est ce que dou yako amoul wone rek 😂
Louma diakhal moy keur gui com dieunde ngako legui niome ani sen xaliss ?dégouma fén foko mentionné 6millions yi wakh ngako té lolou domou bayi laniouko diokh legui le probleme moy le restant de l'argent kane moko yor?
C'est le problème il a seulement payé les 6 millions pour les domou baye
Le gars dale boko dèglo doul rek lay def. A part les 6 millions verser a lautre famille il na aucunement dit largent verser a aa belle famille. Ki kou bone la
Mom lay ladj
Bien 👍 dit 😢
6 millions yii après mou tabakh deuk dalene nakh rekk c'est un embecile
grand bi vraiman daguay werer liga def dinanioula diap fo et usage de fo gua def abui de confiance
Senegal quand 2 personnes sont en conflits, quand tu écoutes l’une d’ente elle, tu lui donnes automatiquement raison.
@@papaelhadjithiam7746 Sénégal aussi niou diang teiy deimei khel beurri woul dh. Sentiment laniouy dokhei.
Gars yii daagn naan ki mounguii tabakh feneenne , naagne fekhée djeulle keur guii, ha Sénégal dagnon saagne dée.
Say geste bii kouko layal nafek ngua
Sénégalais Boula Ndiéké WAKH Ngani Mo Nek Thi DEUK
billahi
Bilahi limay bayi khél dafa mélni nitt gni dougneko bayi khél ki néna papay boy yi 1992 la décédé ta mome 1996 la tak ndiaya 4 ans après gnouy soga wax wakhi diay domou bayou boy yi fougne nékone ta boy dieund ta yor khaliss bo mome lousi yonou banque bagay taylé keuyitou keur gui bilahi bo yoroul wone keuyitou keur gui do guéné deureum yor ndieugou keur gou bakh diamano yoya di dougeul sa khaliss ci keur gokhamni néga dafay inondé yorowone nagoul rék keuyitou keur gui nékone sa lokho mola may lou bari
Tu n’as rien compris 🤣🤣🤣
Day doule keur boula banque nango lébal ci ay papier wam 13millions nga kham ni amena valeur
Yaw wero le titre de propriété n'était pas muté en son nom propre banque ne peut pas accorder un prêt sur cette base toi aussi .
Il a obtenu un prêt parce que il était un agent de maersk donc il avait un compte courant et comme tribunal mo diay .les papiers de la maison . Ci greffier bi lay nek
Vraiment@@mahber9355
@mahber9355 yaw mi ya wéroul démal déglou version famille bi ak sen dôme baye bi
Kou niak diom gua demal sa keur baye
Da ngay tothie sa lefeul ndeye doul bilahi katal sa data ndeye sa yo yéwo bilahi souma deukone si kogne ba heure bi ma ngui si kasso ba kone deugue na sa ndeye bou yague goordjigén nga rék li defma métti trop je te jure je cherche pas à comprendre
Mane la gueuneu méti ki dou sakh nite.
YAW VRAI GOROU YALLA NGA....LII NGA BIDEU RECK ...WONENA SAYE YENÉ .BOU DOME BOU BAH DI DEFAL .AYES WA DIOUREUME...NASA DIAM YAGUE NOU BOUKEU..AAMIIIN...
SALLALAHOU ALA MOUHAMADIN SWAS
Dangay doul rek , ki unité 14 la deuk té boko lalè wayadi
@@WA.WA99saga nittt molay takha donnn gore yallah ???
@faaadadju7101 ECOUTEZ !!!! JE CONTIONNE PAS LES INSULTES....J AI JAMAI INSULTE SUR MES COMMENTAIRES....C EST SON INDIGNATION...SS POUR AUTANT FAIRE VRAIMENT ATTENTION AUX INJURES ....SINON JE L AURAIS CONSEILLÉ QU IL PEUT COMMENTER SS INSÛLTES....ET JE VOUS REMERCIE DE VOTRE REMARQUE....TOUT DE MM JE MAINTIEN K NIT BOU THIEUREUL WADIOUL LA.
DI DIEGUEULOU NDAH SAGUA BAHOUL TÉ RAFETOUL....SI JE PRENDS LE TEMPS DE VOUS REPONDRE ..C PARCEQUE BOUGUOUMA TOGNE ...JE POVAIS ME FOUTRE DE VOTRE REPONSE....MAIS. PAR. ACQUIS. DE CONSCIENCE J. L. FAI PA...TÉ HAMNI YALLA DJISNA LOU NIT DEF...TÉ DIOULITE AKHANE LA NIANE NEKEKO FA YALLA....ENCORE DI DIEGUEULOU BOUBAHABAH....
WA SA
Kouy guenee sa goro dé doko dieundeule keur.
Kou niakkeu djiom nga
Kouleu hol hamni dorkat nga
BAMOU PRESENTER WOO NI TRANSITAIRE REKK NGUEN WARONA NOPALU
Yaw wakhofi digue leufeul ndeyam domou xaram bi nga done sa digue leufeul ndeye bou am kani xégne ak moutarde Dijon domou locataire bi nga done
C un vantard
😂😂😂😂
Togn baxoul
@@CheikhOusmane-y7oseytaner togual
@@ZakariaGt-q1c merci
Wadji dé néna fène kaat déyy mane wakh, deyy am expression té môme wakh rek laay def bolé si am expression Bou saff sapp .. ah en tout cas 😮
Attention le gars il est très logique bien que niawna
Je disais aussi. Ses explications sont cohérentes daal.maintenant reste à savoir.
Non copain ya des zones d'ombre. Diabar dji lii mou wakh ak mom bokoul.
Diabar dji bi gnou ko ladjé defané xamoul Keur gui si tourou Kane le nék. Après mom mouné diabar bi gnou ko ladjé da né dieukeur dji mo ko mom.
Té bène wakh defmeu frapper wa dji néneu féne katt dafay meuneu wakh😂 mais je trouve qu'il parle trop.DIEU seul sait. Wassalam.
Bizarrement dama am même impression si logique la nek dal do kham exactement lou kham réellement Yalna deug gui fegne rk
Bi Senghor di wah l’émotion est nègre dioumoul. Juste parce que mère bi mingui thibiti les gens perdent la raison totalement alors qui loumou wah c’est très logique.
Kiii sokhnam Ndiaya Moy domi xaramata Ndiaye bou Niafff ndéme guéné sa yaye si bitti kiii Môm doméxarme la Meunoul expliqué loumay dégg sama Nop yiii toroxal sa gorro di feukh ndéye feukhi
Bamay dokhane si Ndiaya Kaay 😅😂
Ohhhh sama khel niaawneu sama khel niaawneu sama khel niaawneu 😂😂😂
Peut être que le gas a raison aussi
Ki Kay limiy wakh rombouna deug ndakh limiy wakh lèp dafa verificabile Senegal nak mom affair de farfarlon moka yakh mo mom yeufeum te def na lou bakh ba fika kholam yam lo louy problem bi🥳
Il ment, très clairement,
Ms Serigne bi bo dieudé sa keur goro deukal lénn dilén doundal yalla dila soutoural continue comme ça daga nélaw dh
Non nelawoul c'est juste que sa belle sœur lui pourrissait la vie et sa mère était de mèche avec elle qu'est ce que tu veux qu'il fasse au final laisser sa belle sœur diviser sa famille ou l'expulse tu sais quand on atteint un point de non retour on est obligé de faire les choses brutalement
Vrai mbam ngua
Wokho DEUG
Ki day fen deh c’est un imbécile
Pourquoi tune leur a pas dit que tu as achete la maison des le debut au lieu de leur proposer de signer( meme les mineurs c'è qui n est pas legal !!! ??? !!! ) pour un pret bancaire qui sert a retapper la maison ?
Tu n es pas fiable a 100/100
Mais a -0%
Vraiment
Parce que c’est un vaut rien
C'est la ou se trouve le problème,il devrait les informer et en plus devant des témoins comme le chef de quartier ou les imams du quartier et notables....
Doullll rek quieye Def fen rek ❤❤❤
Kona mere bi dafa diaxlé ndax dagnou nara diaye keur gui mouy lepp pour djunde ko yaw nga djundal ko sa bopp
Yaw yaye domaram deug sa kanam bou mokk ndeyam bi 😢
C'est un imbécile ce monsieur
Danguay doul rék
Day doul keur gui gua tak fa diabar warone gua rouss nane coupé nagne léne ndokh walah courant ki dou sakh nite.
Depuis le début je me suis dis que wadji teuboul teup rèk ni mo mom keur gui. Et que yaye dji soit dafa comprendroul wone ni ki dafay dieund keur gui pour mom,soit khamone nako mais mo expliquer woul khalè yi la vraie situation.
WAYÈ linguèn def niaw neu. Expulsion mo waroul wone. Même si les enfants attaquent, nga dem justice pour niou xamal lène ni momouniou keur gui., mais dafa NIAW parceque yaye dji mak leu.
XALÉ YI AUSSI DÈLÈNE WAKH AK SÈN WADJOUR YI BALA NGUÈNE DI ATTAQUER AY COMBATS parfois nga nèk ci keur tè do khol nou keur gui dèmè. Nga kheuy rék commencer am wètiètte, di lidieunti ay keuyitou keur ba andil sa bop problème.
Parfois les parents pour soutoural ndiabote daniouy def ay sacrifices youniou meunoul expliquer rien que pour beug soutoureu. Tok lèn ak sèn yaye nguen wakhtane ak mom.
ABDOURAHMANE. Outeuleul sa goro foumou deuk. Li niaw neu si sa der .
Yaw topal feulé, ay détails rek ngafi wakh
Dieundeu keur famille risque bou maga mak là. Na leip rafète,adouna dou dara. Kiko momone gañouna bou yagu(paix à son âme)
Tu as payer 5 millons et quelques et tu dis que c'est 13 millions donc t'as donner le reste à qui ?
Merci là-bas abus de confiance la deff ak manipulation wahoulén wo yepp
Khaliss boussi dess fane l dém moma diakhal
Dafa profito si Seine gnakeu nek mais ki dou nitou dara
Tout a été bien dit et je pense que tu a fait ce qu'il fallait tout sera clair inchallah si barkel mawlana cheikh Ibrahime
Yaw mom esk cv
Ki khatheu Leu, tu attendais key niou diaye keur gui pour que gua dieundeu ko, tkte digua ame Armèl yeu keur InchAllah
Ligui amour droit dieund?
@@coumbasow7352 bah oui da done diaye mou dieund logique heuheu
Legui il devait faire quoi ? Bayi tribunal diay ko kenen après niou guenei mere bi ak ay diambotam ?
@@ndeyefatou4374mais arrête de défendre ce monsieur c'est ton père ou frère
Pa delol keur diambour bi ta gueneu thi sa féne yi
Simple maçon pourtant tu as volé sa maison lui qui n'était pas en fonction publique a laissé quelques choses mais toi dis nous tu es qui?
Merci laba
Vous êtes entré tristement dans l'histoire un fait inédit et bientôt le karma...
Objection rejetée c'est très léger comme argument....
Walay
Tu as fait une grosse erreur d’acheter cette maison.
Tu as profité de leur ignorance truand du premier degré
macha allah merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Acheté la maison n'est pas une aumône tu as juste trouv une bonne aportunité que tu as saisie
Vraiment tei au final nieup si bénéficier wou. Parce que quand même niom gni di wah niougui si keur depuis 2005 sou len beugone gueinei il allait le fait depuis. Mais doumeu leu fat saama keur beu parei gamay tongal makk sama diamboot Moi je suis totalement d’accord avec lui
Sa deunou ndéy
Mane le gas je le crois bien l africains en general est trop emotif mais le gas est tres coherent dans ses dires...
C est vrai, africain daffa meunne worre, loko dimballii dimballii boulleu beuguee worre worre là.
Lolou deh la guiss
le gas il est dans la logique
Mane Dé Nopina... Sénégalais NANIOU Bayi Di Wérou Thi Ben Version
Hummm d'après limou wakh yaguena dimbeuli famille bi mane dé mom mii la geum
Ce guy est très dangereux un menteur professionnel 😢 il avait tout prévu jusqu’à ce moment 😢 punaise il se rappelle de tout vachement tu es fort 😂😂😂 avec tous tes preuves que tu viens de citer il va falloir une sacrée paire pour pouvoir ce tenir tête avec lui😂😮😮
Et y’a beaucoup de sénégalais comme lui selfish rek sans cœur
C’est un conseil pour nous tous . Faisons très attention à l’héritage car il divise les familles.
C’est la première connaissance qui disparaîtra chez les musulmans selon le prophète Mohamed saw
Si Maçon sila niafé ba Ame keur
Félicitations kou bakh gua
Sama alouwa soriwoul deh wayé donn na degg ben waraté katt mouy wax si mirass. Néna chariya dafa wax ni borom keur sou gagno nagnou mirass keur gui kouné niou diokh ko walam mou dem. Sou gnou mirassonn keur gui bou yagg problème bi dou am.
Non se diabar waxoul né ya ko mom dè. Bi gnou ko ladjé da né xamoul si bane tour le nék. En tout cas semeu wadji téguil se loxo fi ngue ko ték baxoul si yow ak se ndiabote😮
Kousiy wakh dal na wakh louko leer
Ce qu il explique est très logique
Wallay c logique mais certains ne comprendront pas
Même bou fekké tribunal moo djaaylou keur gui, waroon na leer si seen boppou gnoom gneupp ni dangay djeunnd keur gui
Yaww tu attendais que nogaye beye decede mais yalla nena nogaye beye est la
Kou rèw sa loufeuf daye ga mes yalla nala yalla faye sa liguèye di guènè watè
Pabi loumou done ak limou donoule lépou kén ladioulako depuis le départ woor nga si dioublouwone nith na ragal yalla guiss nagnoufi louné lingaye wakhni lépou dangadone wouthe ningaléne diéko wassalame
Dokham ko wara gam mi yalla na yalla dif diamou sy bar keb serigne touba amine
Au Sénégal on est très émotif, mais ce monsieur a raison jusqu'au preuve du contraire. Avec l'émotion on ne raisone pas
Bamay dokhaan si ndiaya😂😂😂ndiaff 😂😂
Canam bou gniaf khonambi yalnala yalla na yalla leral lep
Mais iow lako moidjie torokhal outil keur mo guene
Ak lou meuna khew mom dieuff dji ñaaaw na loool
Pourquoi il dit simple maçon à pauvre défunt tmt il ne t’a rien fait tei maçon c’est une métier noble que j’aime bien 👍
Néna simple maçon, qui dou tousss
Tribunal yoon la kham.
Arrêter ce mascarade et trancher la vérité.
Ce genre de problème sa ce régle au tribunal.
Il a raison de suivre la procédure en justice, sinon en cas de décès ses enfants seraient expulsés de cette maison.
C est la catastrophe ce mec il a simplement abusé la famille c est sa femme que je plains et ses enfants aussi Alal Diaroul li il n a pas d arguments ndeysanne niaw n’a torop
Kou deugue sa ndeye ngua dieul . Yaaa bone , yaa yess
Oh lala moutoulma transitaire doull rekk
Tu dis ce que tu as fait personne ne la fait c’est vrai car c’est ma première fois d’entendre quelqu’un racheté la maison de ses beaux parents car ils ont des problèmes 🤣🤣
Wa mais diokhé 6million yi pour teguil domou baye yi lothi djoublou won
lima diakhal moy mome dieunde lay wax ta néna domou baye yi la diokh 6 millions lolou tékiwoul dieund di ndax diokhoul mér bi dara mok ay domame
@ vraiment ki daflen nakh pask bobou ay xalé lagnu sen yaye amoul won Kokou diapalé
Abus de confiance la def
Waxofi lou lerr et puis tu es arrogant té amo soutoureu
Banga neké transitaire la khamni ah Wa bakhna😅
Abdourahman bayil niémé yallah Kou la khole khamni wakho deug
Alalu mirass d'où Allal yalla hamna yenn hamguenn. Ta yalla d'où fattee. Bayilenci hell😢