Dome bou ame diom dou meussa waxtane si ay affaire heritage mane d sama baye par la grâce de dieu amna dakar 8 keur pratiquement mais walahii azim nimou défe ba ame yoyou keur unchallah si yone bobou la beugue diar unchallah keurou baye dou keur allalou baye dou allal wassalam
@@fatimandao8359 liga wakh deugue la mais j'exhorte juste d'avantage sama mbok jeune yi rk gnou beugue séne yeufou bopou bayi ti tak diabar andi séne keur papa difa tabakh ay néke yoyou mo doxoul.
Vraiment il est temps que cette fille se repose et la maman vienne nois expliquer ce qui s'est réellement passé. Le gars a parlé, mais la maman aussi doit parler.
Moi personnellement je raison à l’homme serai était lui cette famille sortira de cette maison depuis très longtemps legui degno menal sen bop beug trahir le gars les sénégalais sont très émotif mais en écoutant deux versions tu n’as besoin d’être juge pour savoir de quel côté trouve la vérité
Je pense qu'on doit faire très sur cette affaire. Cette dame geumou mako deh . Liiii guisse moy sen yaye avait besoin de la maison lors les autres héritier lui mettaient la pression mou outi walou siiii Abdourahma mome aussi mou diouguil les demi frères et reste avec la maison gni nag mangueu beugue récupérer sen keur pour deflène nakh mais tout au début ce la arrangé la maman tè ba légui mère biii wakhoul lep . Sama analyse rek la def nag
@@reinemariedione2475 nonon lolou mounoul nekeu mais waroul wone kone diokhè 6 million pour la part des demi frère tè khoume ame 6 million à cette époque (avant 2000)amone na khalis
Salam Alhmadoulilah Macha Allah wakh bou dofé nope yi ko déguelou wer ya ndirime guéne Yalna Allah SWT diapaléne thi daradiéye Yonetebi Seydina Mohamed SAW barké Serigne Babacar Sy RTA amine
Métina trop. Mais parfois dom moy khawi soutoureu yayam. Affaire de heritage la nite gni wara bayi diko loukhmboote. Wala koukay dèf nanga wakhtane bou bakh ak sa wadjour. Depuis le début je me suis dis que wadji teuboul teup rèk ni mo mom keur gui. Et que yaye dji soit dafa comprendroul wone ni ki dafay dieund keur gui pour mom,soit khamone nako mais mo expliquer woul khalè yi la vraie situation. WAYÈ linguèn def niaw neu. Expulsion mo waroul wone. Même si les enfants attaquent, nga dem justice pour niou xamal lène ni momouniou keur gui., mais dafa NIAW parceque yaye dji mak leu. XALÉ YI AUSSI DÈLÈNE WAKH AK SÈN WADJOUR YI BALA NGUÈNE DI ATTAQUER AY COMBATS parfois nga nèk ci keur tè do khol nou keur gui dèmè. Nga kheuy rék commencer am wètiètte, di lidieunti ay keuyitou keur ba andil sa bop problème. Parfois les parents pour soutoural ndiabote daniouy def ay sacrifices youniou meunoul expliquer rien que pour beug soutoureu. Tok lèn ak sèn yaye nguen wakhtane ak mom. ABDOURAHMANE. Outeuleul sa goro foumou deuk. Li niaw neu si sa der .
14:06 peut-être aussi dafla wax loloi pour soutoureu. 14:31 kheyna aussi djabar dji dafa banione nguèn am surprise ci situation keur gui. 15:20 ma sœur. Je pense que maggou keur gui kham naniou li khèw. Danioulèn waxoul wone li khèw rèk pour vous épargner.
Abdou Rahmane da wara khamni liko mér bi diokh moguene fort 11millions .lifi dieulé bayou khalé yi doufi bayi kéne .Rahmane moye yeurmandé .na tour wouyou borom waye .
10.54 ki limou wakh andou Rahmane a dit pareille mouni mo faye avocat pour niou deff apl pour maye mere bi 3ans de plus limouy wakh ni yeup ces ce que Abdou Rahmane a bien affirme.....si sama guiss gui khalé bi maîtrisé woul limouy wakh en plus opérationnel victimisation laniouy deff ni kham naniou legui ak tiktok et consort on médiatise trop ce genre de fait divers dome gué né na yayam et consort en plus danio deim ma tchibir regrette beugeu récupérer keur. N'oubliez surtout pas que seine yaye mo waral li yeup et matey wakhoul
C’était en 2005 apparemment et la maison était en ruine et ça a été évalué par un notaire à 11millions. En tout cas li abdou expliquer yénou na mana daal. Attendons de voir la suite.
@@abydiouf3182mais à til versé la somme totale à la maman ? En plus es ce que les héritiers étaient au courant de la vente. Il avait annoncé seulement un prêt bancaire
@@abydiouf3182 c'est plus tot l'administrateur séquestre (maitre Diale GUEYE) , commis par le tribunal qui a évalué la maison...en tout cas Abdourahmane Diouf a sorti toutes les preuves qui montre qu'il est légalement propriétaire de la maison...légui nak ils n'ont cas essayé de trouver un terrain d'attente ndakh mbok allalou yalla la...wa salam
Franchement sokhna siii limou wax moo gueuneu yiénou mana té bou léne bayii yallah na léne yallah takhawou té ar léne té sammeu léne surtout encore attaché vos ceintures enpluss on dirait que daffa âme lou louche lou kéneu khamoul fékhé léne Lou takh mou âme sagn sagne bou tolou nonou
C'est la procédure de vente qu il a éffectué pour avoir des prêts est ce qu'il a un autre titre en son nom qui peut lui permettre de contracter un prêts
Bonne remarque. Non il ne l as pas. En plus il rembourse le prêt avec la location des boutiques construites au RDC. Ils lui rembourse ses 6 millions et il n a qu àdégager et rendre la maison
Ce qui m inquiète sur le problème abdou rakhmane diouf ce qui la explique il a raison méfiez vous sur ce problème au Sénégal il y a beaucoup de mauvaise famille et des menteurs
J’adore la fille Barki Serigne saliou Elle est véridique Ndiaya revient sur terre le gars il ne respecte même pas t parents d’après lim wakh yeup si point de presse bi
En tt cas dans cet affaire ya que votre Maman qui peut eclairer nos lanternes Abdourahmane diouf aussi ignoble soit il ,il a ete clair dans ses propos avec ses preuves a l'appuie Deug dafa neex degg waxlen sen yaye mou leral leen waxdji
Yaw dof gue rék R plus 2 13 millions kham gue ni lolou amoul Abdou Rahman déy fén na bayi keur bayou diabour té dém keur bayam nitt déy déf yafou nitt méme sou ko Mére bi wakhone lolou sakh sodé nitt kou dioup la mo waw domou Mére bi lolou moy degue mé limouy wakh dou degue Abdou Rahman fén rék léy déf mé na kham ni yala moko eupe dof té dina décède adouna dou keur
Sokhnassi aussi del wakh wolof, vraiment degg nga wolof. Ça ne sert à rien de vouloir demontrer savoir parler le français alors que nga balma mais moy lolou.
@@laminesane4527il a remis en valeur la maison avec un prêt bancaire qu il paye avec la location des 4 boutiques au RDC de 60000 chacun dépuis combien d années.... Abdourahmane est un truand qui a fait abus de confiance
Ay Abdou Rahmane Diouf domėkharam bi dėlloll keurou diabouur giiir yalla ligua dėf nii yak sa diabar bou domėkhamė bii boulėn djiguė ma khamnė ay mbeur guėne inbėcil
En tout cas je ne sais pas qui a raison ou qui a tort mais je peux témoigner l’Etude de maître binta thiam est très très sérieuse khamougn daraay tiakhane 21:28 et madame linga tekk nii bingay enregistrer abdourahmane yeugou ko nga weulbeutikou tekk ko télé def nga un comportement délictuel potentiellement criminel yangui togne wassalam
Mais kouy daw sa ndiabote motax sen baye mo ligueye ba am xalis sam pour casé ndibotam donc Bou gêné aduna c normal ses fils reagi comme ca leur appartient
Sa aye wakh eupe na. Cheuuuu. Respect pour ces dignes parents qui se sont toujours battus dans le respect et la dignité. Il s'agit pas de problème de domou baye
Mere bi daffa djakhlewone mou profito djeundeu rek khamna nak khaleyi maggue mou metti lene meme si i a profite de l occasion je pense qu il est dans son droit
@@africa6799 a ce que je sens tu n'es pas au bain de beaucoup de choses sur cette affaire. Cette expulsion n'a rien à voir avec les 3 dossiers pendant devant la justice. Et tout dépend de ceux là. Normalement ils ne devraient pas être expulsés. Le peinal a toujours le dessus sur le civil
Mme à vrai dire tu présentes les choses de manière fantaisiste. Tu fais dire à Abdourahmane ce qu'il n'a pas dit. Tu as mis ta maman dans cette situation difficile.
Abdoubrakh à raison sur tte la ligne,sa seule 3rreur est d avoir acheté avec famille qui n estvpas unie et sans moyen financier,personne d entre eux ne pouvait acheter pour leur mere
@@bbouhama5373cheque bii 6 millions 4 millions la wakh la diokh mère bii mere bii maykako ?? Waye eritage you xallè yii yonou mére bii nekousi ba diko mayé ???
@bbouhama5373 écoute bien ce que le gars dit dans les audios enregistrés ! Il dit à la dame qu'il voulait donner les 4 millions mais leur mère l'a finalement offert l'argent. Alors dans le conférence de presse il n'a jamais prouvé la somme donnée ! ces audios qui sont des preuves le contredits
@@bbouhama5373yaw yagui waxe bossi bolewone deglou avant guay binde dina taner abdou mo waxe ni mère bi moko mayate 4million yi cheque bi dou 4 6 la guay waxe rek
Elle parle trop celle la aussi Il ya une justice dans ce pays Si la maison est au nom de ton beau frère et que vous ne vous entendez plus au point que toi même tu emmène tes nieces a la police, mieux vaut vous quittiez la maison jusqu'à ce que la justice decide autre chose
Yalnagnou yalla may lignou momal sunu bopou khir gnou ci diamou yalla 😢😢
Amine
Amine
Goor day oute yeufi bopam amal foula Abdou rahmane amal diom
@@papagorakebe7594 Hana dieundouko AK khalissam ? Wala ma compoul
Lou leer nga wax mane deh lolou la gueum
Dome bou ame diom dou meussa waxtane si ay affaire heritage mane d sama baye par la grâce de dieu amna dakar 8 keur pratiquement mais walahii azim nimou défe ba ame yoyou keur unchallah si yone bobou la beugue diar unchallah keurou baye dou keur allalou baye dou allal wassalam
Légui kou beug dieul keure bayou diamour nak yow tamite
Fok nga am fo deugeu ba am sa yeufou popou inchala loka rk
Inchallah
@@fatimandao8359 liga wakh deugue la mais j'exhorte juste d'avantage sama mbok jeune yi rk gnou beugue séne yeufou bopou bayi ti tak diabar andi séne keur papa difa tabakh ay néke yoyou mo doxoul.
@MilkMilo-qr5uc débat bi dou fofou d mon frère ki beau fils bou ñeuw deuk si keure belle famille lolou moye honte nationale
Vraiment il est temps que cette fille se repose et la maman vienne nois expliquer ce qui s'est réellement passé. Le gars a parlé, mais la maman aussi doit parler.
Vous avez tout dit. Yaye dji rek mo kham li nek au fond. Nakh sadji dafko waxone dafkay dieuldeul bopam wala dafkay lebal mou dieund.
@@SENEGAL303merci c’est la question que je me pose seul la maman peut éclaircir les choses
Moi personnellement je raison à l’homme serai était lui cette famille sortira de cette maison depuis très longtemps legui degno menal sen bop beug trahir le gars les sénégalais sont très émotif mais en écoutant deux versions tu n’as besoin d’être juge pour savoir de quel côté trouve la vérité
Prudence et vigilance sur ces dossiers la vérité est toujours caché.
Yaw doule
Abdou c un voleur
Fii lep ler seule les bêtes qui ne comprennent rien
Tu commentes ça sur toutes les vidéos; say affaires leroul dara
Oui je suis fraiment content sur cette fille elle c’est bien parlé Machalla
17:56 manam. 13 millions laniouko diayè, mou diokh nieulè 6 millions, amel sa yaye 7 millions ?. Lègui na lèral just 7 millions yoyou noumko fayè rèk.
Abdourahmane diouf il est mystérieux en plus mystique très mystique mm c’est grave
Franchement liii daffa gniaw té keurou diambour en plussss
Sénégalais moo gniémé yallah
Abdou Rahman adouna dou ay bari pékhé bayil gni ak sen keurgui def yeufi nite adouna dou keur
Wakhe yalla je suis parfaitement d'accord avec toi mon frère 😊😊😊😊
Merci pour votre réponse rapide Si kaname reke inchallah
Je pense qu'on doit faire très sur cette affaire. Cette dame geumou mako deh .
Liiii guisse moy sen yaye avait besoin de la maison lors les autres héritier lui mettaient la pression mou outi walou siiii Abdourahma mome aussi mou diouguil les demi frères et reste avec la maison gni nag mangueu beugue récupérer sen keur pour deflène nakh mais tout au début ce la arrangé la maman tè ba légui mère biii wakhoul lep .
Sama analyse rek la def nag
pourtant ligua wakh c'est logique deh
@@boubaka7172 doyna war dal
Tu as parfaitement raison. ! Meune neu nekke
Geumo femme bi mais ma ladj la goor meuna done sa baye di done bayou diambour
@@reinemariedione2475 nonon lolou mounoul nekeu mais waroul wone kone diokhè 6 million pour la part des demi frère tè khoume ame 6 million à cette époque (avant 2000)amone na khalis
Ce gars doit aller hériter son père et laisser l héritage des autres c encombrant tt de même
Donou sa bay donou bayi diambour omoul féne
Ki dieunde keur gui lane lafi dondou
@@bbouhama5373dou ni lagni dieundé keur
vraiment c'est triste réalité no comment cest pas nôtre problème
Salam Alhmadoulilah Macha Allah wakh bou dofé nope yi ko déguelou wer ya ndirime guéne Yalna Allah SWT diapaléne thi daradiéye Yonetebi Seydina Mohamed SAW barké Serigne Babacar Sy RTA amine
Métina trop. Mais parfois dom moy khawi soutoureu yayam. Affaire de heritage la nite gni wara bayi diko loukhmboote. Wala koukay dèf nanga wakhtane bou bakh ak sa wadjour.
Depuis le début je me suis dis que wadji teuboul teup rèk ni mo mom keur gui. Et que yaye dji soit dafa comprendroul wone ni ki dafay dieund keur gui pour mom,soit khamone nako mais mo expliquer woul khalè yi la vraie situation.
WAYÈ linguèn def niaw neu. Expulsion mo waroul wone. Même si les enfants attaquent, nga dem justice pour niou xamal lène ni momouniou keur gui., mais dafa NIAW parceque yaye dji mak leu.
XALÉ YI AUSSI DÈLÈNE WAKH AK SÈN WADJOUR YI BALA NGUÈNE DI ATTAQUER AY COMBATS parfois nga nèk ci keur tè do khol nou keur gui dèmè. Nga kheuy rék commencer am wètiètte, di lidieunti ay keuyitou keur ba andil sa bop problème.
Parfois les parents pour soutoural ndiabote daniouy def ay sacrifices youniou meunoul expliquer rien que pour beug soutoureu. Tok lèn ak sèn yaye nguen wakhtane ak mom.
ABDOURAHMANE. Outeuleul sa goro foumou deuk. Li niaw neu si sa der .
Liii d la la wakh la maman rek mo meuna leral lii
14:06 peut-être aussi dafla wax loloi pour soutoureu.
14:31 kheyna aussi djabar dji dafa banione nguèn am surprise ci situation keur gui.
15:20 ma sœur. Je pense que maggou keur gui kham naniou li khèw. Danioulèn waxoul wone li khèw rèk pour vous épargner.
Abdou Rahmane da wara khamni liko mér bi diokh moguene fort 11millions .lifi dieulé bayou khalé yi doufi bayi kéne .Rahmane moye yeurmandé .na tour wouyou borom waye .
YOW ABDOURAHMANE DIOUF NIAKH GUA DIOME ,MOUNO DONE SA BAYE DONE BAYYOU NDIAMBOUR.TU N'A PAS LES COUILLES.TCHIIIIIIM.ADOUNA DOU KEUR .
Ay Abdrahmane loula diaralli adouna dou dra allalou mirass kouko moyetouwoul😢
10.54 ki limou wakh andou Rahmane a dit pareille mouni mo faye avocat pour niou deff apl pour maye mere bi 3ans de plus limouy wakh ni yeup ces ce que Abdou Rahmane a bien affirme.....si sama guiss gui khalé bi maîtrisé woul limouy wakh en plus opérationnel victimisation laniouy deff ni kham naniou legui ak tiktok et consort on médiatise trop ce genre de fait divers dome gué né na yayam et consort en plus danio deim ma tchibir regrette beugeu récupérer keur. N'oubliez surtout pas que seine yaye mo waral li yeup et matey wakhoul
Faite très attention sur cette affaire
Mandou léne
Vraiment li dafa gnaw on doit reprendre le procès
Maléne done dieundeul yeuré diléne diokh niou lek yore len après dafa wara takh nga mome keur diambour domeram deug sa ndeye so beugué doko dème outi
Merci
Dafay féne sakh doundeuloule kéne. Séne khalis la yorone diko manipuler
Louer sene ay boutique diko encaissé, donc doundaloulene gratuit mais avec leur argent. Abdourahmane est un truand
Waw mane lima diakhal moy keur bou nek si side bobou tmt esk c'est resonable nga warko ame si li nga diokhé
C’était en 2005 apparemment et la maison était en ruine et ça a été évalué par un notaire à 11millions. En tout cas li abdou expliquer yénou na mana daal. Attendons de voir la suite.
@@abydiouf3182mais à til versé la somme totale à la maman ? En plus es ce que les héritiers étaient au courant de la vente. Il avait annoncé seulement un prêt bancaire
@abydiouf3182 même pas et même si c'était le cas il n'a jamais donné toute la somme
@@abydiouf3182 c'est plus tot l'administrateur séquestre (maitre Diale GUEYE) , commis par le tribunal qui a évalué la maison...en tout cas Abdourahmane Diouf a sorti toutes les preuves qui montre qu'il est légalement propriétaire de la maison...légui nak ils n'ont cas essayé de trouver un terrain d'attente ndakh mbok allalou yalla la...wa salam
Franchement sokhna siii limou wax moo gueuneu yiénou mana té bou léne bayii yallah na léne yallah takhawou té ar léne té sammeu léne surtout encore attaché vos ceintures enpluss on dirait que daffa âme lou louche lou kéneu khamoul fékhé léne Lou takh mou âme sagn sagne bou tolou nonou
Wakhal wolof Wala NGA wah français cas bi ya Tah dieuloul yéna situation 😢
Couy lire nganan wakhal wolof .
YALNAGÑOU YALLA DÉFALL SOUTOUREU BOU MATALÉ SI CÔTÉ YÉP SOUGÑOU KANAMAK SOUGÑOU GUINÂW YÉP IN CHALLAH
Allahouma amine
Ak lou meune ame nagnou dèlo sougnou khel thi yala khamenii adouna dou keur tè jugement dernier diarna bayii khel wa salam
Adou rahmane me fénnkate bou mack la
Pour mane mère bi mo dèff leep ba paré ni mikk
C'est la procédure de vente qu il a éffectué pour avoir des prêts est ce qu'il a un autre titre en son nom qui peut lui permettre de contracter un prêts
Bonne remarque. Non il ne l as pas. En plus il rembourse le prêt avec la location des boutiques construites au RDC. Ils lui rembourse ses 6 millions et il n a qu àdégager et rendre la maison
Gayii lire bou 2005 nga lire bou 2001 nekoulen si deug deh
Jai ts les camps mai pr mane abdou rahmane com amna ay moin menon na may keur gui mer bi defko si touram
Abdou diokhel karou diambour
Famme bi wakham léroul
Merci cette année y aviez de carte gape
Ce qui m inquiète sur le problème abdou rakhmane diouf ce qui la explique il a raison méfiez vous sur ce problème au Sénégal il y a beaucoup de mauvaise famille et des menteurs
Fenn
Non toi tu n'a rien compris abdourakhmane est sous contrôle judiciaire à cause de cet effaire
Walahi deug leu mane deh mom la gueum
Naniou si déff nank affaire bi dou yombe niari vérsion yi yeup léroul
Wakhal wolof gni lay diapalé wolof lagnou dégue
Abdourahmannn dafa ammm fittttt
Non Safa niak diom plus tôt
Iow do wakh wolof rek
Boo degoul toubab dianguil kida meun mokal maîtrisez ma sha Allah ❤
@awandiaye9993 iow kèpalma sa data biii domeram
Dinala lebal 6millions sou khalé yi magué fayy ????? Hun 🤔🤔🤔 yalna yalla leral
YAW DAL AK SAY DOMI NDAYE YENA NEK CI DEUG,NANGEN ANDANDO TAKOU NOKH WADJI CI BITI,DOMERAM JIMOU DON CHIM...
J’adore la fille Barki Serigne saliou Elle est véridique
Ndiaya revient sur terre le gars il ne respecte même pas t parents d’après lim wakh yeup si point de presse bi
Audio 4 million yi égoul
36:56 sisi 95 gap amone na. Dafa beuriwoul wone rek.
Je suis fière de cette femme battante ne lâche rien
En tt cas dans cet affaire ya que votre Maman qui peut eclairer nos lanternes
Abdourahmane diouf aussi ignoble soit il ,il a ete clair dans ses propos avec ses preuves a l'appuie
Deug dafa neex degg waxlen sen yaye mou leral leen waxdji
Abdou raxmane a raison
Abdourahman delole keurou diambour boudone sa ndeye doko guene yow vrais domarame nga
Dem lenn sen yaye nguen ladj ko ani sen walleu si khaliss bii, mane deh lii Abdou rahman la gueum
Yaw dof gue rék R plus 2 13 millions kham gue ni lolou amoul Abdou Rahman déy fén na bayi keur bayou diabour té dém keur bayam nitt déy déf yafou nitt méme sou ko Mére bi wakhone lolou sakh sodé nitt kou dioup la mo waw domou Mére bi lolou moy degue mé limouy wakh dou degue Abdou Rahman fén rék léy déf mé na kham ni yala moko eupe dof té dina décède adouna dou keur
Donc pour toi la maison vaux 6000000f?
Sokhnassi aussi del wakh wolof, vraiment degg nga wolof. Ça ne sert à rien de vouloir demontrer savoir parler le français alors que nga balma mais moy lolou.
Merci beaucoup enfin ken kouko Sagna wakh ak ay fautes you bari elle aurait pu être simple
Un peu de tolérance svp, le français n est pas notre langue maternelle, l essentiel C est de comprendre ce qu elle veut dire...
Machalla Ndiaye 🙏🙏🙏
Nogaye béye mo môme keurgui l'héritage est un droit pour l'enfant
Abdourahman kou kat yayam la ki kou yor numérom ma sagua ndayam vrai domeram moy kou guor ki
❤❤❤❤❤❤
Abdourahmane Diouf nagnla délo sa 6million nga délolén sén keur ngirr yalla alalou dono kén douko kheuthio
En plus des 6milion mo tabakh keurgui, dangkoy delo valeur keurgui
C'est pas sa valeur actuelle, mais sa valeur en 2005 avec un état délabré
@@laminesane4527il a remis en valeur la maison avec un prêt bancaire qu il paye avec la location des 4 boutiques au RDC de 60000 chacun dépuis combien d années.... Abdourahmane est un truand qui a fait abus de confiance
Mais kerguou 3 familles bok,kon momoulenko yenkesse abdourahmane souko dieundeulwone kon heurebi kenene dieundko pour man xaleyi dono maag songou granbi
C’est cohérent mais tu pourrais parler en wolof seulement
Ay Abdou Rahmane Diouf domėkharam bi dėlloll keurou diabouur giiir yalla ligua dėf nii yak sa diabar bou domėkhamė bii boulėn djiguė ma khamnė ay mbeur guėne inbėcil
doyna war dal
Pa keur 11 millions 2008 amoufa
Keur massar 2007 15 million la dieunde
Ki dou nitt kou bakh
En tout cas je ne sais pas qui a raison ou qui a tort mais je peux témoigner l’Etude de maître binta thiam est très très sérieuse khamougn daraay tiakhane
21:28 et madame linga tekk nii bingay enregistrer abdourahmane yeugou ko nga weulbeutikou tekk ko télé def nga un comportement délictuel potentiellement criminel yangui togne wassalam
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Abdourahman diouf danga seysiwoye si keur gui djiohéle keuro djiambour
Mais kouy daw sa ndiabote motax sen baye mo ligueye ba am xalis sam pour casé ndibotam donc Bou gêné aduna c normal ses fils reagi comme ca leur appartient
Wadji kou deug mouy wakh hamni Day doule ndeam demale outti keur té dello gni sen keurou papa way thim domeram
Pa yi nio wara bayi di weure di kater rek sounou guener adouna bayifi aye probleme entre aye domou baye
Sa aye wakh eupe na. Cheuuuu. Respect pour ces dignes parents qui se sont toujours battus dans le respect et la dignité. Il s'agit pas de problème de domou baye
Papa yi mirace lene sene bopou balla deh, bayilene neubeutou, Sinon keur guou diakhasso rek
Abdourrahmane niakga diome délole keur diambour
Abdou rahkmane geummo mako
Lima thi metty moye di khass bayou diambour nane simple maçon la wone qu'elle manque de respect ce gas yalla na yalla lèrale🤍🤲🏻
Môme dé bayou jambour bé gueuneu bayame.
Diouf kou kat ndayam la mane mii maçon la moumay xase
Nopiléne yénne kharitou abdou rakhmane yii koumounék sa alalou baye ga khekh
L'entreprise c'est sinim a Mauritanie
Pourlane abdou di lene may 6millions yena beug lou yomb dalene di motali mais boulene fate ne doundeul nalene deukeul lene 20ans
Affaire bi yombouna ,wadji nañiou ko tegui lime déff ci keur gui, té dess ak sénn keurr, mou diékh borome keur gui fim teude taliwoul
Le gars a fauté depuis le début moralement on ne peut pas racheté la maison de ses beaux qui se trouve dans des problèmes
Wa contrôle judiciaire bi louko waral diouf KOu riche nga
Yoyofale lène sène dounde adouna diaroule dara ndakhame kiko liguèye modème bayifi yeupe ciloudoule thiobarème masseu gnénène.
Mani bayil francais bi wakh wolof
Nama yalla baale genre yi foleine guisse aye tekk khel lagnou
Limou wakh, ana lissi tek khel?
Mere bi daffa djakhlewone mou profito djeundeu rek khamna nak khaleyi maggue mou metti lene meme si i a profite de l occasion je pense qu il est dans son droit
Milkmilo tu na rien compri une maman agé de 78 ans blayer
Awa gniy bineu commentaires dilla dalll c'est Abdou Rahmane Diouf ak domam yii ak diabar diou bonneu dji nioy commentaires wakhal ba tėpėkou lii dafa yobeu tė mėtii
Yene mère mo lekk khaliss bi bayil sa ratatati bi😂
khana abdourahmane diouf khana amoul ndéye ak baye bumou donou.sa famille diabar loy woutt sisén problém héritage iow gni yague ngalén ték beutt
Abdourahmane n'a fait que se profiter sur des mineurs
Li diaroul nguéne di wah si reseau sociaux si turbinal até nalen non
Vraiment li mom..
Tribunal até goul
@@YayeAwaGUEYE-ci2hx donc on a fais comment pour les expulsé
@@africa6799 a ce que je sens tu n'es pas au bain de beaucoup de choses sur cette affaire. Cette expulsion n'a rien à voir avec les 3 dossiers pendant devant la justice. Et tout dépend de ceux là. Normalement ils ne devraient pas être expulsés. Le peinal a toujours le dessus sur le civil
@YayeAwaGUEYE-ci2hx il ne devrait pas être expulsé. Tu es sur de ce que tu dis
Mme à vrai dire tu présentes les choses de manière fantaisiste. Tu fais dire à Abdourahmane ce qu'il n'a pas dit. Tu as mis ta maman dans cette situation difficile.
Ce DIOUF la DOMOU HARAM DEUGU LEU 😡
Danguay feine dei zoueratt amoul soumi mais plutôt snim et c une minerai de fer 😂😂😂
Yaw say wax léroul dia Manon boubou gnata gua ame thie atte
Abdoubrakh à raison sur tte la ligne,sa seule 3rreur est d avoir acheté avec famille qui n estvpas unie et sans moyen financier,personne d entre eux ne pouvait acheter pour leur mere
Il dit quil voulait verser les 4 millions mère bi néko djeulko ! Donc ce gars est un menteur et les audios le dément carrément !
Foumou wakhé lolou? Ki binde cheque bou 4millions pour mère bi
@@bbouhama5373cheque bii 6 millions 4 millions la wakh la diokh mère bii mere bii maykako ?? Waye eritage you xallè yii yonou mére bii nekousi ba diko mayé ???
@bbouhama5373 écoute bien ce que le gars dit dans les audios enregistrés ! Il dit à la dame qu'il voulait donner les 4 millions mais leur mère l'a finalement offert l'argent. Alors dans le conférence de presse il n'a jamais prouvé la somme donnée ! ces audios qui sont des preuves le contredits
@@bbouhama5373yaw yagui waxe bossi bolewone deglou avant guay binde dina taner abdou mo waxe ni mère bi moko mayate 4million yi cheque bi dou 4 6 la guay waxe rek
Ki mom gamou ma kou wallxi
Mak yaw wakhoul dara lou lére
Diokhel keur diambour
Bou lolou lépeu wésso khalé bi raféte na
😂😂 bly mol la deff
Awa ndiaye bayil wakhdji keur bayye d'où keur te gua dem ladj se yaye bou bakh ti affaire bi awa tu es trop louche
Merde wayy
Awa démal seuyi amgua dieukeur . Ndiaya mola eupeu ndieurigne pour yayam . Si se n'était pas Abdou Rahmane vous ne parliez même de cette maison
Elle parle trop celle la aussi
Il ya une justice dans ce pays
Si la maison est au nom de ton beau frère et que vous ne vous entendez plus au point que toi même tu emmène tes nieces a la police, mieux vaut vous quittiez la maison jusqu'à ce que la justice decide autre chose
Wakh mo diote. Fi kougnou fi guéné wone thi biti dinga wakh ba tépékou. Bouléne khébale guinare wopame