Ma chAllah oustaz. Vous contribuez à l'éveil des jeunes sur les pièges de satan et des dangers liés à la musique. Qu'Allah, SWT, vous bénisse et vous élève toujours en degrés
Bârakallahu Fikoum Ouztaaz Kebe, Wa Jazâkumullâhu Khayran. Amna solo lol Yalnaniou Borom bi bolei deffal tawfekh defal leineko. Trés pertinent. Qu'Allah vous et nous Préserve des vices mondaines...!!!😊
Oustaz yo xamni amougn Dara si lerr delen tudu Ya Allah di zikr ndax ngen lerr touti comseil rk la tei ngen bayi fait divers akh wax loussi sa yone nekoul . Yene jeune yi ñi wallahi amna si ño xamni koulen topp rerr ndax dañi naxaté ba parei di tour niti leundam wa salam
@@harounafalayesoumare7857 mdr ok ! Dieul ngen ELHADJ OMAR FOUTIYOU TALL , YOBOU SAFARA , MAME MAODO , CHEIKH AHMADOU BAMBA , DABAKH MALICK , BAYE NIASS , AL MAKHTOUM, ABDOULAHAT ETC.. DIEUL GNEUP YOBBOU SAFARA 😅😂. Aaaaah wa bakhna BA YOWMAL QIYYAM . ON VERRA BA XAM MOR KEBE MOM MO MOM ALJANA . GNIKO TOPOU LA YEUREUM , DIANG KHADISS AVANT HIER FOKNI MO TOKK SI XAM XAM ADOUNA 😅😂😂alors MO MOUDJÉ MOKKAL HADITHS . « DOCTEUR »MOR KEBE 😅😂😂 SAVANTS OU ÉRUDITS DOU AM DOCTORAT DOU AM AGRÉGATION . YOYOU POUR DIÈNGOUMAN YILA . AY DIENGOUMAN NGEN TOPP.
@@harounafalayesoumare7857 COMME SÉNÉGALAIS YI GNO TOPP KARA , BETHIO THIOUNÉ , SERIGNE MOUSTAPHA SY AL MAKTOUM , etc… KOU TOP MOR KEBE DIOKH KO NOPE REK DAMA LAY COMPRENDRE . PROBLÈME BI MOY FI KOUFI WOTÉ GNU WOUYOULA 😅😂😂😂. DEUK BI MYSTIQUEMENT DAGNE GNO DIEKKOU 🙃
Amna oustaz youy violer di ndjalo. Am ay ndiobé si keur diné yi. Église ay ndiobé yagg na fa. Affaire bi dou milieu mais nitt yi la. Amna gnou nek si showbiz di def lou baax rek
Oustaz wakhal thi Waly Seck mi di promouvoir Gordjiguene thi deuk té nga bayi P.Diddy biii..d toutes les facons on sait gnognou amou kilifa amou gnou dinéé!!!
Il n'a rien compris . Il n'est pas condamné mais accusé et il attend son procès. Fene bakhoul. Amagoul procé . D'où dioulite baye def lou selle. Est ce que gueume n'a yalla.
Je trouves que l’exemple des Americains nest pas pertinent pour conscientiser notre jeunesse. On a pas la mme culture, ni les mmes réalités avec les Americains. Pourquoi pas prendre des examples sur la musique Sénégalaise pour conscientiser les jeunes? Parlons des problèmes senegalais, la débauche dans les boites de nuit, les bars, et tt cela. Si on arrive à régler ce problème, pas besoin de mentionner la culture Americaine. Le Senegal ne peut jamais égaler le niveau de débauche de la culture Americaine de tte facon. Charité bien ordonnée commence par soi mme
Iow eskeu cv,niatta jeune nioy roy ci rappeur américain,nane ay rappeur lagn,di takk ngandi sén sisén batt yi ak di toukh di nane,ak di ndialo etc...nga nane dou exemple pour conscientiser.da nga deglou mé dolen deglou
@@dianementality214tt d’abord pas besoin dêtre hostile et déplaisant, ns sommes là pour juste échanger des idées. Ensuite si vous limitez votre réflection sur le fait de fumer, boire de l’alcool, et porter des bijoux, vous avez perdu le fil conducteur du message que jessaies de véhiculer. Le problème est bcp plus profond que cela. Les trucs qui se font à Hollywood dépassent nos capacités sur le plan moral, societal,religieux, financier, et les motivations sont également differentes. Essayer de lire entre les lignes pour comprendre la teneur de mon message. Après cela, ou pourra avoir une discussion poussée. Wa salaam
Je suis tout à fait d'accord avec vous. Parfois Oustaz Mor Kébé en fait trop. L'histoire là ne nous intéresse nullement, li nekk si dëkk bi doy na ñu xëy ak gont. Nous raconter les dérives des Yankees ne peut en rien nous conscientiser
Un oustaz du showbiz vous fête rire qui parmis les oulémas de la Sunnāh parle des choses pour étudier la sunnāh jamais tu en trouvera jamais mor arrêter de te jouer des jeune 😂 étudiant car ils vont croire que tu es un oustaz a la mode alors que c faux
My grand yaw deh nar nga sonnu trop. vraiment yenn yi sokhor leu té yangui wax thi nio xamnei dundu niula sax. Pour yen yoonu salaf moy selon sen compréhensions REK. Descendez sur le terrain si vous êtes véridique mais c'est tellement facile d'être derrière les écrans di wax rek. Fan nguen dianguei, thi kann, combien de temps ? Moi la question que je me pose est la suivante : esque yenangui diangg deug deug koutoub salafou-salih ? Mais on dirait que lou deuppo ak seni banexu bakkan rek ngiueni dieul. ALLAHOU MOUSTA'AN
Il est très informé bravo boy yedd nouvelle génération yi il faut niou consciente et pour ça il faut gua fekk silein si liniou nek bravo ouztaz
@@aminatayade9341 yaw moom ak dakhaar nga danga dougou si thiowli té khamo likhéw
C'est bien mais on veut des gens qui maitrisent le Coran et fabriquent des téléphones et les autres technologies
😂😂😂😂@@gerarefontaine1417
Mâcha allah on a besoin des Oustaz qui nous rappel que les célébrités ne font que nous vendre la belle vie mais en réalité ils ne le vivent même pas
Aka am xam xam machalah
Il suis l’actualité de près , machalla. Il est très avertit ya ouztaz
Machallah ❤mor Kebe hafijahoullah leral yi 🧠🇸🇳✨Amna solo
Ma chAllah oustaz. Vous contribuez à l'éveil des jeunes sur les pièges de satan et des dangers liés à la musique. Qu'Allah, SWT, vous bénisse et vous élève toujours en degrés
Merci Oustaz…..
Morale of the story
“Everything that glows ain’t gold”
Machala. Mais oustaz bi il connaît la culture hip-hop des us.
Bârakallahu Fikoum Ouztaaz Kebe, Wa Jazâkumullâhu Khayran. Amna solo lol Yalnaniou Borom bi bolei deffal tawfekh defal leineko.
Trés pertinent. Qu'Allah vous et nous Préserve des vices mondaines...!!!😊
Amiine
Machallah Oustaz Mor Kébé
Ma chahalla amna solo loooooole
Aka Cultiver MaaSaaAllah ❤🎉
Il faut faire attention sur le cas des chanteurs ou stars noirs américains .Il y'a des lobbies qui détruisent ces derniers à la fin de leur carrières.
En tt cas doyna waar, R.Kelly, Bill Cosby, Mikail Jackson etc.. bizarrement ils sont tous noirs et riches.
Barakk'ALLAHU fiik ❤
Macha Allah yalla na yalla sameu leu.
Machallah oustaz
MACHA ALLAH
❤❤❤
Merci oustass❤❤❤❤
Machallah yalna yalla barkéle Xamxam by amine yarabi
Amine
Machallha très important
Macha allah qu'allah vous préserve 😊😊😊
الله يحفظك يا أستاذ
❤❤❤ barakkalah 😢😢😢😢soubhalalallah😮😮😮❤❤❤
Macha allah
Oustaz est bien branché
Machallah amna solo lol
Oustas mercy beucou way
Triste réalité de la vie d'aujourd'hui
Notre oustaz cultivé MachAllah ❤
Oustaz yo xamni amougn Dara si lerr delen tudu Ya Allah di zikr ndax ngen lerr touti comseil rk la tei ngen bayi fait divers akh wax loussi sa yone nekoul . Yene jeune yi ñi wallahi amna si ño xamni koulen topp rerr ndax dañi naxaté ba parei di tour niti leundam wa salam
Ban tarikha nga bok😂
Ban tarikha nga bok😂 ban FC
@@od7240 Yaw bane nga bok Salya wala bou himar Sale bi ?? Wala Himar lô?🤣🤣
@@od7240 Yalna lene subhanahou wa tahala guindi 🫱🏾🫲🏿
Yangui dougou Lou sa yone nék yow, wala Partisan rappeur bi ngueu. Yow yay diante bi mo takh Dara mounoul léér ci yow. qu'Allah te guide
Ndeysane
Mashallah très pertinent
Soubkhanalah li moy alkou deugue
Nous africains surtout la plupart des des jeunes sénégalais ne comprennent rien c'est milieu très dangereux le milieu show buzz
Je t’assure wakhoffi dara 😂😂😂😂😂😂.
Beug nga Doug si sujet bi Mai’s maîtriser wo ssi dara dara dara …
Sa khol bi mo bone rek,
Wala nga bok ci niom.
@@harounafalayesoumare7857 mdr ok !
Dieul ngen ELHADJ OMAR FOUTIYOU TALL , YOBOU SAFARA , MAME MAODO , CHEIKH AHMADOU BAMBA , DABAKH MALICK , BAYE NIASS , AL MAKHTOUM, ABDOULAHAT ETC.. DIEUL GNEUP YOBBOU SAFARA 😅😂.
Aaaaah wa bakhna BA YOWMAL QIYYAM .
ON VERRA BA XAM MOR KEBE MOM MO MOM ALJANA .
GNIKO TOPOU LA YEUREUM , DIANG KHADISS AVANT HIER FOKNI MO TOKK SI XAM XAM ADOUNA 😅😂😂alors MO MOUDJÉ MOKKAL HADITHS .
« DOCTEUR »MOR KEBE 😅😂😂
SAVANTS OU ÉRUDITS DOU AM DOCTORAT DOU AM AGRÉGATION . YOYOU POUR DIÈNGOUMAN YILA .
AY DIENGOUMAN NGEN TOPP.
@@harounafalayesoumare7857 COMME SÉNÉGALAIS YI GNO TOPP KARA , BETHIO THIOUNÉ , SERIGNE MOUSTAPHA SY AL MAKTOUM , etc…
KOU TOP MOR KEBE DIOKH KO NOPE REK DAMA LAY COMPRENDRE .
PROBLÈME BI MOY FI KOUFI WOTÉ GNU WOUYOULA 😅😂😂😂.
DEUK BI MYSTIQUEMENT DAGNE GNO DIEKKOU 🙃
Ni la app oustaz di mél fokk ngay geustou li xéw di artou nitt gni thi lou nieuweu goul
Amna oustaz youy violer di ndjalo. Am ay ndiobé si keur diné yi. Église ay ndiobé yagg na fa. Affaire bi dou milieu mais nitt yi la. Amna gnou nek si showbiz di def lou baax rek
Bimay wax li yagg na. Dou sax jamono jii
Oustaz bandi
❤❤❤❤❤❤❤❤
Topou ndigueul yalla mo gueun.
Complexé aka beuri ci rew mi , gni ci nassarane bi , gni ci naar yi
Nar bi déh bakhoul
Imame noumou khamer li yeupp
Ni ngén khamé milieu bobou diakhalnama
Ouztaz mi rappeur leu wonne 😅 akka khamm rappeur yi
WAALY SECK mogene diege
Dundou bobou mo am americ khaliss femme auto
This is none issue for Senegalese daawa , probably you run out of issues related to you audience.
Oustaz wakhal thi Waly Seck mi di promouvoir Gordjiguene thi deuk té nga bayi P.Diddy biii..d toutes les facons on sait gnognou amou kilifa amou gnou dinéé!!!
Mo gueune deh. Mais beugua wanné ni leup nha pégg finalement ca te rend ridicule. Wakhal si wa rew mi
Amougniu si preuve teksi dara woroniousi te p.didy dagne cas prendre en flague
Yaw oustaz sa information déssna attégôunou sakhe bakoye condamné
C'est toi qui n'a rien compris
Il n'a rien compris . Il n'est pas condamné mais accusé et il attend son procès. Fene bakhoul. Amagoul procé . D'où dioulite baye def lou selle. Est ce que gueume n'a yalla.
C'est toi qui n'a rien compris écoute avec ta raison
Soigne ton langage.
Même si il a dit des "" mensonge " il y a de bonnes manières pour le corriger
@@moussamohamedba8444il ne pas le sens de l ecoute !
😂😂😂😂😂😂😂chtttt boy yi ak Sen incarnation de oustaz nandité . Li yeup TH-cam mo gnou togne ak facebook.
Waxlen siliguene xam
Je trouves que l’exemple des Americains nest pas pertinent pour conscientiser notre jeunesse. On a pas la mme culture, ni les mmes réalités avec les Americains. Pourquoi pas prendre des examples sur la musique Sénégalaise pour conscientiser les jeunes? Parlons des problèmes senegalais, la débauche dans les boites de nuit, les bars, et tt cela. Si on arrive à régler ce problème, pas besoin de mentionner la culture Americaine. Le Senegal ne peut jamais égaler le niveau de débauche de la culture Americaine de tte facon. Charité bien ordonnée commence par soi mme
@@abibndour9158 avez vous lu l’intégralité de la vidéo ?
Iow eskeu cv,niatta jeune nioy roy ci rappeur américain,nane ay rappeur lagn,di takk ngandi sén sisén batt yi ak di toukh di nane,ak di ndialo etc...nga nane dou exemple pour conscientiser.da nga deglou mé dolen deglou
@@dianementality214tt d’abord pas besoin dêtre hostile et déplaisant, ns sommes là pour juste échanger des idées. Ensuite si vous limitez votre réflection sur le fait de fumer, boire de l’alcool, et porter des bijoux, vous avez perdu le fil conducteur du message que jessaies de véhiculer. Le problème est bcp plus profond que cela. Les trucs qui se font à Hollywood dépassent nos capacités sur le plan moral, societal,religieux, financier, et les motivations sont également differentes. Essayer de lire entre les lignes pour comprendre la teneur de mon message. Après cela, ou pourra avoir une discussion poussée. Wa salaam
Je suis tout à fait d'accord avec vous. Parfois Oustaz Mor Kébé en fait trop. L'histoire là ne nous intéresse nullement, li nekk si dëkk bi doy na ñu xëy ak gont. Nous raconter les dérives des Yankees ne peut en rien nous conscientiser
@ deglou nga video bi bamou diekh ?
Avant de juger
Thiéy yi imam dounou wakh mouk si s touba walla seydil hadji malik lolou dafaharam si ndioom wayé mannanowakh si rapeur yi ak mbari lambeyi
Kholale dof bi mome
Esk wakh si niom c forcé
Bo dieulé s'en teré Diko diangu fek si AK bokalé kay doko meuneu wakh nit gni boko wakhei niouni da ngay Di ngate
Bou wakhone limou kham ci nioniou nga saaga ko
Yaw dimbali niou way ishhh
Riiirrrrrrrrrrrr
Tu comprends rien 👎🏽
Un oustaz du showbiz vous fête rire qui parmis les oulémas de la Sunnāh parle des choses pour étudier la sunnāh jamais tu en trouvera jamais mor arrêter de te jouer des jeune 😂 étudiant car ils vont croire que tu es un oustaz a la mode alors que c faux
My grand yaw deh nar nga sonnu trop. vraiment yenn yi sokhor leu té yangui wax thi nio xamnei dundu niula sax.
Pour yen yoonu salaf moy selon sen compréhensions REK. Descendez sur le terrain si vous êtes véridique mais c'est tellement facile d'être derrière les écrans di wax rek. Fan nguen dianguei, thi kann, combien de temps ?
Moi la question que je me pose est la suivante : esque yenangui diangg deug deug koutoub salafou-salih ? Mais on dirait que lou deuppo ak seni banexu bakkan rek ngiueni dieul. ALLAHOU MOUSTA'AN
@@MouhamedLamineBadji
Lamine Badji khawma loutakh nga rew rekk
@@alhassangassama3296 wallahi tu as raison akhi
@@mmaleekss Qu'ALLAH nous accorde la bonne compréhension des textes !
@"Al amrou bil magrouf. Wa nahyou ani mounkar"on ne réponds le manque de respect par le manque de respect
Machalla Oustaz