Bly oustaz ya wax deugg li lepp mame cheikh ibrahima fall waxone nako bo meussana wax yalla ngui fépp danane ah doom dioumngua dh yalla khadioul féne fépp mo nékk si yalla vérité absolu ❤❤❤
@@mouctardiallo9859bane shirk ngay wakh fofou ? Babe shirl lafi wakh ? Meuno len bayi lolen degu nit wakh nguen ni shirk sans argumenter ? Et n’oublie pas que y’a deux types de littérature et de moyens de transmission qui existe depuis les temps anciens !
Résumé : Ken dou Yalla .mome rek moy yalla.c'est pourquoi nous Tous nous devons rendre un hommage à notre Seigneur , Yalla,le remercie denous avoir envoyé Mohamed psl. Encore une fois ken dou yowe.Dieuradieuf Yalla.
Qu’Allah nous facilite la bonne compréhension 🤲🏾🤲🏾🤲🏾 . Vidéo bi seul les doué d’intelligence vont les comprendre. Wakh dimension la sofa yégoul boul contredire "Le Créateur n’a pas de créateur sinon il deviendrait une créature et Allah est Le Créateur de tout chose et aucun créature ne peut sortir de Lui car il est partout " mais le titre de votre vidéo elle est énorme prochaine fois inchallah essaye de revoir vos choix des mots 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@@ibrahimambodji6608 mbirou yallah dou mbirou intellect. Kone Toubab yi èg nagne si bou yag. Ki ni il ne raconte que des histoires qui impressionnent les petits esprits.
@@taphadiagnekone intellectuel waroul xam yallah? Yallah moy kokou nékh mou hamal ko boppam. Té mom Il n'a rien inventé dégg dégg biko yallah may lagne amoul.
@@ibrahimambodji6608 ce que je dis moy dou khel moy égalé si yallah. Lo nek nek intellectuel dou lolou mo lay khamal yallah. Dou métaphysique, dou physique, dou philosophie. Des gens kham nagn yallah kham bou wer sans connaitre les particules, les Boson de higgs, les trou noir,.....
Genre wakhtane yii bakhoul si kou gueumm gueummeum takhawoul fokk ga am imannn ga meune ko comprendre sinon rk diga dougueul sa khell mi loussi bokoull yalla keneu la ❤️
Cette Question me revenez souvent 😂quand j'étais adolescente et mon mari m'interdit d'en penser car meune n'a wangni gueume ndakh yalla khél douko dadjie dadj ba meune la missale originane.Donc unitle de fatiguer ton esprit pour cette question 😂et en philosophie on te répond la mm chose Dieu est partout..alhamedoulihi merci pour cette explication
Respect a ce monsieur les scientifiques ne font qu'embrouiller nos cerveaux en voulant découvrir...nioune nite yii lignou xam moye k Yallah laniou geum naniou découvrir sen bopp louniou beugue xam com k aye scientifique laniou
Le premier mot du Coran " Ikhra" manaam Guestou, Diangueu ! Xamxam. Xaamxam est cœur de toute chose. Les scientifiques suivent bien cette voie tout en évitant le dogme. Pour la science toute phénomène naturel à une cause que l'on peut découvrir par des recherches methodiques (effet/cause). Apres on peut insinuer les limites de la connaissance scientifique.... Certains vont recourir à la foi pour passer à un autre niveau... Encore une fois leppeu ci connaissance leu akk ay différente approche. Et que ces deux approches tournent autour du mot " Ikhra"...
Bayiléne sokhor ak Aniane ak nafékh professeur xam xam lay wakh bou kéne meunoul dindi. Dém léne diangui mo gueune Di wakh si Lou nguéne khamoul. Longue vie à professeur ❤❤❤❤
ô Seigneur! Tu es le premier car rien ne T’a précédé. Tu es le dernier car rien ne Te succèdera. Poser la question qui a créé Allah est de la mécréance.
Allah n’a pas de début à son existence et pas de fin. Il existe de toute éternité et n’a pas de comment ou d’image. Allah existe sans endroit, sans direction, le temps ne s’écoule pas sur lui et il a créé les endroits, le temps, les directions et toute chose. Il existait avant eux et il ne change pas. Sa volonté ne change pas. Et tout lui appartient, il n’a besoin de rien. Il ne ressemble pas à ses créatures, il ne ressemble à rien. Rien n’est tel que lui et il est unique. Nul ne peut atteindre la réalité d’Allah, lui seul connaît sa réalité.
J’ai dis a staghfiroullah au début mais après j’ai compris .ce professeur parle avec philosophie tè dafa ladj dèg dèg .mais aussi ces des questions qu’il faut pas poser parceque notre cerveau Dieu l’as verrouillé pour mou nek kumpeu
@@sabin7799tu connais pas l’âme qui est en toi et tu veux connaître Dieu .tin cerveau Dieu l’as verrouillé et si on t’explique tu deviens fou automatiquement
Tout à fait c'est de la métaphysique. Il y a des questions ko n'ont point de réponse et faut même essayer d'en trouver au risque de devenir fou kom vous l'avez souligné tantôt
Dieu contrôle tout. Celui qui contrôle tout est partout. Et celui qui est partout est tout. Ça, c'est le résultat de la méditation de l'intelligence humaine, Si tu veux le connaître avec la sûreté de l'âme, prends le wird tarbiyou de Baye Niasse.
Ta phrase est anti coranique. Allah akbar = Dieu agrandi . Qui peut agrandir Dieu ? Si tu veux dire qu’il est grand, alors respecte sa parole qui dit : Allahou kabîrou = Dieu est grand si on se réfère à la grammaire et la conjugaison arabes.
Allah n'est pas hors du temps mais il transcende le temps. Allah d'englobe pas tout mais il apparaît dans toute chose,sur toute chose et en toute chose
Thieuy yallah rabou samawati wamafil ardi,yazhal dialal wal-ikram 👌Laaaah diamètre diamate si birr diamou yallah yi si bir gayi yallah yi si birr nitou yallah yi si birr kharitou yallah yi,lepp nguir diammo ko mom yallah mi nek si mom, Laaaah yamleuzeul Dieuf Dieul koufa ndieuk dieul gueuneu gaaw eupe yol❤
Machallah amna solo lool Mais baatou dafa ( diééki diééki am ) eska lolou nirou wul ni kon meuss naa niak mom yalla té yalla meusta nian bey diéki diéki di am moofi meusa nek WAXUFA KHADIIMUN MAA LAHU BIDAAYAH WAZUU BAQAA'INN MAA LAHU NIHAAYAH ( Mom yalla adji djitou la déd diko gnél ab tambalé kaay Té adji déss ded diko gnél ab yamou kaay
Machalla Pr yalla na yalla doli leu sa kham sell na malheureusement certains douniou leu comprendre par ce qu'il vont utiliser sen khel et ils vont se perdre comme toujours yalla dou khel mokoy kham djeureudjeuf cheikhou tidinane yalla na yalla khamle bopam si mbolem mindef yi . svp le commentateur boul weddi so khamoul juste demande on sera ravi de partager
Création fou mou am rek xam xam mi ngui fa,Yallah Ken dou comparer ndax foumou nek comparaison amoufa ,legui ani lerou Yonent bi si saak dji? Cause ak effet meunoul am si Yallah si manifestation rek la am T Dieu reste non manifeste.Merci pour le partage Professeur qui pousse à tous ces questionnements 🙏🏿Arigatooo
Ki ay waham faw nga am dégg dégg deug pour meune ko comprendre. So degoul limouy wah nak nga dieul li nga yakkar ni moy deugg nga geume ko. Wayé amo xam xam beugga wéddi c grave .
Dios es el único del mundo Allah alhamdulilah gracias Dios que da padres musulmanes tengo muchísimo suerte porque nacio y soy musulmán alhamdulilah siempre hay que hacer los 5 rezas al día muy importante no lo olviden por favor
Ya Allah yA Allah meme quand nous parlons de lui le puissant je ne dis pas même parler de lui il suffit juste de penser de lui que vous avez des vibrations même les douées d intelligences ils les permets de connaître sur ses dimensions par exemple vous prenez une graine de poussière vous dévisser en 4 parties et chaque partie vous le diviser en 6 parties les résidus de cette poussière c'est ça nous les hommes qu'ils nous permettent de connaître sur lui le puissant le❤ dimensionnel
Yallah amna xél (Esprit de Dieu) té amna xol (zate) ! Amna Ruh (Haqqiqatu muhamadiya) amna djeum (haqqiqatu Ahmadiyatu) ! Fittratalah leuti aleyha fattran nass! Yallah Moy Jamono ci boppam ! Mélo yi AK tourr yi AK kawmu bi Moy DEUG deugi djeumi Yallah ! Ku xam sa bopp xam sa Borom ! Ku faté Yallah niu fatélo la sa bopp ! Dara existé wul ludul Yallah ba ci atome bi geuneu ndaw!
YALLA toogèewul fenn, ndax dara attanuko. YALLA dara Tiimuko, tayik nekkul ci biir Dara. NB : Bari waana kuy wax ci xam YALLA, fekk xam xamam ci YALLA mingi melni gone gu mënagul wax. Took fii naan YALLA amul xam xam; waaye dépassé na xam xam, waxi kuy graw graw lu kepp la. Loolu dépassé xam xam doo wax mukk num tudu, ndax amul. العليم ci TURU YALLA la Bokk. YALLA wax ci ALXUR'AAN ان الله يعلم غيب السماوت والارض ngay wax sa waxi gone yi. Bayyi leen di wax di jeema impressionn é nit ñi.
Yalla na Yalla yéssal yermadjéme si dioulitte yep si barké seydina mouhamed psl ❤❤❤
Amine Sallalaahou aleyhi wa salam
Amiiine ❤
Thieuy yalla keneu meunou ko décortiquer yalla moy yalla moy Rabi sama wati wal ardi dieureudieuf yalla ❤❤❤❤❤❤
WALLAHI❤❤❤
Bilahi
Tei kenn la
Allahou akbar ❤❤❤❤❤❤❤
Boko dièmè rek wediiko yallah n'a borom bi deff gnou dioulite
Bly oustaz ya wax deugg li lepp mame cheikh ibrahima fall waxone nako bo meussana wax yalla ngui fépp danane ah doom dioumngua dh yalla khadioul féne fépp mo nékk si yalla vérité absolu ❤❤❤
Walahi dayssane wah yombou na waayé dégue mo diaffé
Thiey sama wadji mo dégeu sunu borom
@@BbinetaGadiaga bly mome moy khaliloulahi faw mou dégg ko
Indil fouko cheikh Ibra wakh fi nitt di wakh diné ngenn dougal ci ay chirk indil fouko Ibra fall wakh
@@mouctardiallo9859bane shirk ngay wakh fofou ? Babe shirl lafi wakh ? Meuno len bayi lolen degu nit wakh nguen ni shirk sans argumenter ? Et n’oublie pas que y’a deux types de littérature et de moyens de transmission qui existe depuis les temps anciens !
Résumé : Ken dou Yalla .mome rek moy yalla.c'est pourquoi nous Tous nous devons rendre un hommage à notre Seigneur , Yalla,le remercie denous avoir envoyé Mohamed psl. Encore une fois ken dou yowe.Dieuradieuf Yalla.
Psl
Allah a toujours existé et n'est pas créé,il est,il était et il sera,il est infini et éternel.
Voilà tu as tout résumé
C’est ce qu’il essaye d’expliquer nak
Kham kham fégn na 😁
Macha Allah
Waxofi dara
Li nieup wax ba paré té xam ko ngafi wax
@@hokagesama7295ioe dh wakho xam xam wakhou Kou sokhor kèp nga fii wakh
Kén Mame maodo Malick Sy yalna yallah yok léram AK koulouhoum magoum diné yallah fayal niou lén macha allah ❤❤❤❤❤
VERITÉ ABSOLUE ! DIEU EST TOUT ! Cela resume tour macha allah !
Khoul houwa Allahou ahad Allahou Samad lam yalid walam youlad walam yakoum lohou koufouwan ahadd
Merci
Walahi
Aka ma beug sourat bobou
Moy lannne
Ndéyssane professeur yague fi lolle té wérr❤
Qu’Allah nous facilite la bonne compréhension 🤲🏾🤲🏾🤲🏾 . Vidéo bi seul les doué d’intelligence vont les comprendre. Wakh dimension la sofa yégoul boul contredire
"Le Créateur n’a pas de créateur sinon il deviendrait une créature et Allah est Le Créateur de tout chose et aucun créature ne peut sortir de Lui car il est partout " mais le titre de votre vidéo elle est énorme prochaine fois inchallah essaye de revoir vos choix des mots 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Xaam nga rek!
Merci t'as tout dit. Il te faut un certain bagage intellectuel pour le comprendre.
@@ibrahimambodji6608 mbirou yallah dou mbirou intellect. Kone Toubab yi èg nagne si bou yag. Ki ni il ne raconte que des histoires qui impressionnent les petits esprits.
@@taphadiagnekone intellectuel waroul xam yallah? Yallah moy kokou nékh mou hamal ko boppam. Té mom Il n'a rien inventé dégg dégg biko yallah may lagne amoul.
@@ibrahimambodji6608 ce que je dis moy dou khel moy égalé si yallah. Lo nek nek intellectuel dou lolou mo lay khamal yallah. Dou métaphysique, dou physique, dou philosophie. Des gens kham nagn yallah kham bou wer sans connaitre les particules, les Boson de higgs, les trou noir,.....
Wallahi ken d’où yallah moy Rabi Sama wati alhamndoulillah dieureudieuf allah ❤❤❤❤❤❤❤
Genre wakhtane yii bakhoul si kou gueumm gueummeum takhawoul fokk ga am imannn ga meune ko comprendre sinon rk diga dougueul sa khell mi loussi bokoull yalla keneu la ❤️
Kham kham niarry khamla lo guiss amna bir ak biti respect yalla barkel
Yalla nanu yalla bakhal si Barki seydina Mouhamed saw
Tonton madiama yalna yalla Contane si ioe ak molem dioulite❤
Cette Question me revenez souvent 😂quand j'étais adolescente et mon mari m'interdit d'en penser car meune n'a wangni gueume ndakh yalla khél douko dadjie dadj ba meune la missale originane.Donc unitle de fatiguer ton esprit pour cette question 😂et en philosophie on te répond la mm chose Dieu est partout..alhamedoulihi merci pour cette explication
Walahi diougueule si faydou thia Baye Niass dingua xame yallaah bou wër
Alhamdoulilah. Yallah, Sougnou Borom rek moy Deugue. Al Kabir, Allahou Akbar
Dieu est le meilleur Scientifique ❤ Ahadoul Ahad❤❤❤
Mashalla merci beaucoup Professeur Madiama Fall pour votre pertinence et clairvoyance vraiment amna solo lol Yalla dou nite walahi?
Fou Yalla nékoule amoule.😍
Allakhou akbarr❤
Saway yalla amoul barape lepp mo nék si birr yalla
@@momofaye2722 moy lima wax rk..
Fou Yalla nékoule amoule. Leip Yalla la.
Dieu est le premier qui n'a pas de commencement et le dernier qui n'a pas de fin
Vraiment j’aime écouter professeur madiama machallah goudal fan way ❤
Kou dé rek am lo comprendre kéne menoul xam lep ...Macha Allah si xam xam bi Amna solo
Bilahi mon père ya Bari xam xam.yala nala yala doli wer ak soutoureu
Yallah mo wax modi Yallah alhamdoulillah si Mawlana Seydi Cheikh Mohamed Ndiaye Rabi 🙏❤️
Respect a ce monsieur les scientifiques ne font qu'embrouiller nos cerveaux en voulant découvrir...nioune nite yii lignou xam moye k Yallah laniou geum naniou découvrir sen bopp louniou beugue xam com k aye scientifique laniou
Le premier mot du Coran " Ikhra" manaam Guestou, Diangueu ! Xamxam. Xaamxam est cœur de toute chose. Les scientifiques suivent bien cette voie tout en évitant le dogme. Pour la science toute phénomène naturel à une cause que l'on peut découvrir par des recherches methodiques (effet/cause). Apres on peut insinuer les limites de la connaissance scientifique.... Certains vont recourir à la foi pour passer à un autre niveau... Encore une fois leppeu ci connaissance leu akk ay différente approche. Et que ces deux approches tournent autour du mot " Ikhra"...
Machalla Machalla yalla na yalla faye yiw ci barket rassoul lilahi SAW dieureudieuf
Qu'Allah nous pardonne et qu'Il nous guide
Amine ya rabi 🤲🙏
Maodo est d’une autre dimension
Bayiléne sokhor ak Aniane ak nafékh professeur xam xam lay wakh bou kéne meunoul dindi.
Dém léne diangui mo gueune Di wakh si Lou nguéne khamoul.
Longue vie à professeur ❤❤❤❤
Lou werr jeureujeuf
@@MayeCisse-v7x indiléne louy degueureul wakhou professeur bi si Al khourhane wala si wakhou yonintebi
Doynawar
@@thiernondiaye1975yow so manoul comprender li professeur di wakh conn yow mbame Mou seufe ay téré rék geu
@@mordiop705 Kone yaw professeur bi mo eupeu kham kham yonintebi
Kénn d'où yalla sounou borom bilakhi walkitabi yalla rek moy bour bou mague bi❤❤❤
Dieu c'est le CRÉATEUR,lemaître de l'univers. DIEU EST PARTOUT.
DIEU EST TOUT. C'EST LE MAÎTRE ABSOLU. HEEEEY YALLAH.
Machaallah yallana borom bi mey goudou fan ak werr
Yalle na yalla defal nieup diam❤❤❤❤
Lou simple yalla néna kou kham sa bop khamma kon nak naniou djèmeu kham souniou bop nguir niou meun ko kham dieureudieuféé cheikh al islam💪❤❤❤❤❤
Dieuredieuf yow mi wokh lolou👌
@@linspirateurniang650 🙏
Kham sa bopeuh ndieuk sogua kham lénéne 🎉bay Cheikh ndigeul Lô...🥰🥰🥰
Yalla wakhoul loolou fenneu. Yenn fenal yalla rekk ngen meun
mais nouniouy deff ba kham sounou bopou??
Et là nous faisons' nos péchés à l'intérieur de lui Li rafetoul changeons
Qu'Allah nous donne une bonne fin
Allahou akbar Allahou akbar Allahou akbar Allahou akbar Allahou akbar Allahou akbar Allahou akbar
Comme le dit Dieu “ JE NE PARLE PAS AUX IGNORANTS !!!! Allah is Kabir. Le suprême des suprêmes !!!
Merciiiiiiiiiii beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ô Seigneur! Tu es le premier car rien ne T’a précédé. Tu es le dernier car rien ne Te succèdera.
Poser la question qui a créé Allah est de la mécréance.
Il est lunik le seul notre roi notre seigneur mom lagnu diamou taye ak euleuk
Wallay bo tarbiyoul sa geum deugeuroul nop ak khël meunoul dékou linguay wakh diëreudiëf baye barham niass wax deug yallah contane nagne waye khöl ❤❤❤sëd way
Waxatikko déh ❤.
Tout ce que je sais est que c est Dieu qui nous a créé.
Masha ALLAH lii mooy mandou bokk na si diamou YÀLLA YI geuna kawé ALHAMDOULILAH DIEUREUDIEUF WAAY
❤❤❤❤
Comment tu l'as su?
Allah n’a pas de début à son existence et pas de fin. Il existe de toute éternité et n’a pas de comment ou d’image. Allah existe sans endroit, sans direction, le temps ne s’écoule pas sur lui et il a créé les endroits, le temps, les directions et toute chose. Il existait avant eux et il ne change pas. Sa volonté ne change pas. Et tout lui appartient, il n’a besoin de rien. Il ne ressemble pas à ses créatures, il ne ressemble à rien. Rien n’est tel que lui et il est unique. Nul ne peut atteindre la réalité d’Allah, lui seul connaît sa réalité.
J’ai dis a staghfiroullah au début mais après j’ai compris .ce professeur parle avec philosophie tè dafa ladj dèg dèg .mais aussi ces des questions qu’il faut pas poser parceque notre cerveau Dieu l’as verrouillé pour mou nek kumpeu
Si On doit le savoir parce que c'est notre raison d'être
@@sabin7799tu connais pas l’âme qui est en toi et tu veux connaître Dieu .tin cerveau Dieu l’as verrouillé et si on t’explique tu deviens fou automatiquement
😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Vérité absolue
Tout à fait c'est de la métaphysique. Il y a des questions ko n'ont point de réponse et faut même essayer d'en trouver au risque de devenir fou kom vous l'avez souligné tantôt
Dieu contrôle tout. Celui qui contrôle tout est partout. Et celui qui est partout est tout.
Ça, c'est le résultat de la méditation de l'intelligence humaine,
Si tu veux le connaître avec la sûreté de l'âme, prends le wird tarbiyou de Baye Niasse.
Seul le zikr nous permet d'accéder à la connaissance divine.
Seydina Mohamed (PSL)
Thiey yalla sounou borom kene la☝️
Guiss yallah rekkkk seul !
Tu auras toutes les réponses sur ce sujet !
Allah Allah Allah ❤
YALLA defayeme te raglou
Fou tour nékoul santeu nékoul yallah nék fa,lou beuteu guissoul lou khele dadjoul khole ba yeuk ko,fa yallah amul ndieukeu amul mudj amul kagne amul fane amul ani amul naka, yallah kesser,dong,kotou, rék, yallah dagne koy kham sa dieumeum kenneu douko lambatou...
ALLAHOU AKBAR LAA ILAHA ILLAL LAH MOUHAMADOU RASSOULOULAH
Ta phrase est anti coranique.
Allah akbar = Dieu agrandi . Qui peut agrandir Dieu ? Si tu veux dire qu’il est grand, alors respecte sa parole qui dit : Allahou kabîrou = Dieu est grand si on se réfère à la grammaire et la conjugaison arabes.
Allah n'est pas hors du temps mais il transcende le temps. Allah d'englobe pas tout mais il apparaît dans toute chose,sur toute chose et en toute chose
L’espace et le temps font parti de la création
Pourtant vous parlez le même langage
Thieuy yallah rabou samawati wamafil ardi,yazhal dialal wal-ikram 👌Laaaah diamètre diamate si birr diamou yallah yi si bir gayi yallah yi si birr nitou yallah yi si birr kharitou yallah yi,lepp nguir diammo ko mom yallah mi nek si mom, Laaaah yamleuzeul Dieuf Dieul koufa ndieuk dieul gueuneu gaaw eupe yol❤
Alhamdoulilah machalla Dieu est unique ❤❤❤❤
Serigne cheikh tidiane sy nena Yallah amna xam xam lolou rek la d'accoroul ak yaw
Un thème très sensible mais très intéressant surtout pour nous les croyants, merci beaucoup professeur.
Yallah Boko khameihh rekk beugue ko❤❤ loolu Moy relation kham Yallah Akh beugue Yallah lepp Si bireum la neik Bou yagueihh Nga outeulko deindanohh djangal Walam Yakoune leuhou koufou wane akhad.....
Yalnala Yallah khamal bopam🙏
Khame ci YALLA, ❤ Vous êtes adorables
@@bamouhamedou6368 ❤️
Machallah amna solo lool
Mais baatou dafa ( diééki diééki am ) eska lolou nirou wul ni kon meuss naa niak mom yalla té yalla meusta nian bey diéki diéki di am moofi meusa nek
WAXUFA KHADIIMUN MAA LAHU BIDAAYAH
WAZUU BAQAA'INN MAA LAHU NIHAAYAH
( Mom yalla adji djitou la déd diko gnél ab tambalé kaay
Té adji déss ded diko gnél ab yamou kaay
Machalla Pr yalla na yalla doli leu sa kham sell na malheureusement certains douniou leu comprendre par ce qu'il vont utiliser sen khel et ils vont se perdre comme toujours yalla dou khel mokoy kham djeureudjeuf cheikhou tidinane yalla na yalla khamle bopam si mbolem mindef yi . svp le commentateur boul weddi so khamoul juste demande on sera ravi de partager
@@amedinedeme558 c est prophesseur qui utilise mal son cerveau , kepp mounounio weddilo Lou onenetebi diangaler
Alhadoulilah. Santé yalla bou bakh
Mashallah yalla rek mo atane leppeu ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci professeur mane dama nopalou lou khew ma sante ame ack niack faibar ack weere louma teck reck ma sante ❤❤❤❤
Kou am imane mon koye guam li gua wakh ❤❤❤❤
Création fou mou am rek xam xam mi ngui fa,Yallah Ken dou comparer ndax foumou nek comparaison amoufa ,legui ani lerou Yonent bi si saak dji? Cause ak effet meunoul am si Yallah si manifestation rek la am T Dieu reste non manifeste.Merci pour le partage Professeur qui pousse à tous ces questionnements 🙏🏿Arigatooo
Allahou akbaar ,mystér la...
J'ai partagé ce vidéo intéressant dieureudieuf mame maodo Malick sy machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nanou am imane ❤❤❤❤❤
PROFESSEUR, TOUT EST DIT ET CLAIRE MERCI BCP
Tout (univers,planète,enrer,paradis)’est une petite pièce devant Allah
قل هوالله أحد/الله الصمد/لم يلد ولم يولد/ولم يكن له كفوا أحد ☝️
Machalla kou diangue khilassou zahab do réré yonenteu bi thiey Maodo ❤❤😊
Thiay Serigne Touba awma si mome sago barképp alkhourane 😢😢
Ki ay waham faw nga am dégg dégg deug pour meune ko comprendre. So degoul limouy wah nak nga dieul li nga yakkar ni moy deugg nga geume ko. Wayé amo xam xam beugga wéddi c grave .
@@ibrahimambodji6608 deg deg tous daguene yomba égaré
On doit remercier professeur au lieu de critiquer khamoul duzg lay wakh.tout est dieu omniscientomnopotent ,omniprésent.
Jajeuf khaliloulah
Machalla
' Thie nekoup YALLAH LA LEP NEK THIE BIR YALLAH '
Dieu seul est victoire mom rék Moy ndam
Kén meunou KO xaam wallahi professeur xam xam bi séleu n'a macha allah ❤️
Machalla prophesseur madiama lahi laha illala Allah Akbar 🙏🏼🙏🏼
Dios es el único del mundo Allah alhamdulilah gracias Dios que da padres musulmanes tengo muchísimo suerte porque nacio y soy musulmán alhamdulilah siempre hay que hacer los 5 rezas al día muy importante no lo olviden por favor
Allahou Akbar kham kham rék moy deugg/kii yalla Na ko yalla samm waay
Motakhone baye niass néwone madé yallah madé yonnenti madé cheikhou tidiane
Yallah moy leep
Leep moy yallah
Motakhone yallah né kouma nekal ma nekal la
Yalla kéne douko lambatou dagua koy kham si lou lére
Dieureudieufé Baye Niass
Mah Allahou 😊😊 yanna yala Faye ❤️❤️❤️❤️❤️ 🥰😍
Ya Allah yA Allah meme quand nous parlons de lui le puissant je ne dis pas même parler de lui il suffit juste de penser de lui que vous avez des vibrations même les douées d intelligences ils les permets
de connaître sur ses dimensions par exemple vous prenez une graine de poussière vous dévisser en 4 parties et chaque partie vous le diviser en 6 parties les résidus de cette poussière c'est ça nous les hommes qu'ils nous permettent de connaître sur lui le puissant le❤ dimensionnel
Yalla nanou guam yalla ❤❤❤❤
Thieuy serigne touba takhna douma siki saka si nékouk yalla gui
Machalla longue vie a toi professeur ❤❤
Ay way contanena di niane sounou borom yokk kham kham bi machalla
Qu'est-ce qui fait pourquoi nous sommes malade où malheureux ; ce dualité ? Ci tout vient de Dieu l absolue
Bou tawate amoul wone, kén dou kham solos wér gui yaram
Sou malheur amoul wone kén dou kham solo bonheur.
Lou YALLAH Sakk, gnar la si sakk, à méditer
@@khalilourassoulentreprise9233bien répondu 🙏🏾
Dieu créé à dieu à l'image de dieu❤
DIEU
Yallah amna xél (Esprit de Dieu) té amna xol (zate) ! Amna Ruh (Haqqiqatu muhamadiya) amna djeum (haqqiqatu Ahmadiyatu) ! Fittratalah leuti aleyha fattran nass! Yallah Moy Jamono ci boppam ! Mélo yi AK tourr yi AK kawmu bi Moy DEUG deugi djeumi Yallah ! Ku xam sa bopp xam sa Borom ! Ku faté Yallah niu fatélo la sa bopp ! Dara existé wul ludul Yallah ba ci atome bi geuneu ndaw!
Kene dou yallah ❤❤❤
Alhamdoulilah alhamdoulilah alhamdoulilah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah khham khjam bi lerna yallah kenla
Allahou akbar Allahou akbar lailaha illallah
YALLA toogèewul fenn, ndax dara attanuko.
YALLA dara Tiimuko, tayik nekkul ci biir Dara.
NB : Bari waana kuy wax ci xam YALLA, fekk xam xamam ci YALLA mingi melni gone gu mënagul wax.
Took fii naan YALLA amul xam xam; waaye dépassé na xam xam, waxi kuy graw graw lu kepp la. Loolu dépassé xam xam doo wax mukk num tudu, ndax amul.
العليم ci TURU YALLA la Bokk. YALLA wax ci ALXUR'AAN ان الله يعلم غيب السماوت والارض ngay wax sa waxi gone yi.
Bayyi leen di wax di jeema impressionn é nit ñi.
Ma cha Allah yalla na yalla fay la aw yiw wah yombou na waayé dégue dégue moo diaffé
Alahou akbar machalla yalla rek moy yalla rabousamawati wal ard
Xam yallah rek moo woor🥹 ken ku xamul Yallah doo comprend lumu wax 😂. Jërëjëf Baye❤
Parfaitement raison, yalla nékoul féne , Féppa nék si yalla .
Deglou Wat KO
Limou la wakh leerna si nekou fepam la feppou NK si mom