Heureusement que vous êtes là. On est fier de vous yaa Oustaz ✊😪 walahi on vous aime ❤ on vous suit ⚘ longue vie à vous 🌷 Masha'Allah Yalna leen Yallah☝ fay contaan nanou cii yeen Yallah xamnako ... Al Quran ak Sunnah rek ☝
Par la grâce de Dieu,nous avons très tôt découvert qu il avait des problèmes de personalités.C est un égocentrique.Mais heureusement que vous êtes là pour nous éviter de suivre ces égarés en nous guidant sur le droit chemin .Allahou ak bar.
@@ousmane5807 kon kay nékko si soufi Bokumi magui lay hamalni bén yone rék la islam am dou 2 dou 3 yonentibi (SAW) wahonané sama héte dina diviséwou 73 yone 72 yeup safara laniou dieum bamou des niou toppu yonnu Alquran ak sama sunnah kép kone bokku yalla naniou yalla ték ci yone wowou té sahalniouci 🙏
Le problème est très simple la plus part des Sénégalais qui croient aux serignes NE CROIENT PAS EN DIEU, AUX PROPHÈTES, AUX SAHABAS...PIR ILS CROIENT RENTRER AU PARADIS SANS PASSER PAR DIEU LE TOUT PUISSANT...DONC LOU SÉNÉGALAIS YI BEUG NON ÇA ME DÉPASSE NON DES CON DES FOUS NON C'EST INCROYABLE...
@@serignemouhamadoumadiamasy5574 Hahahah 🤣, wakhma fou yalla wakhé benen yone boudoul Siratal moustahim? Frere, yalna la yalla dioubal. Yone you nit sos dou meussa yam ak yone bou yalla reud, yonente yi nieuw téggou thi. Tarikha bokoul thi diné baay. Boko beugué geum nak, yaw la rek. Am nga thi plain droit.
@@CHK63 tarixa yi ngén di khass nio takh ngén tala dioly ak diangue alkhouran dangay dém nga lire li serigne touba bindeu dinga kham lan moy yonou mouride
@@serignemouhamadoumadiamasy5574 monté serigne Touba mo bind “rouhou diam yi mongui sama lokho”, “Kaba gui mongui Touba”, “Damay deukalé ak yalla”, “nieup dina niou deh bamou dess mane”. Li yeup so démé thi Khatimoul Mounajati, di nga ko thi fék! Li yonente bi wakh moy deug, lep louniou soss thi diné ji daay wathié yone, té kou wathi yone, dem safar! Koulou biddahatin dalala, wa kouloulou dalalatine fin nar. Wakh ma bakham sa serigne féna loul yalla thi limou wakh!
BarikaAllah firkoum nous sommes sincèrement fier de vous ManchAllah mais on dirait que le Sénégal est pays où l'islam n'a pas d'importance 💔😭 c'est très malheureux de vivre dans un pays ignorants comme ça 😭🙏 💔
Un vrai soldat de l'islam y'a Oustaze Ahma Sall, machaaa Allah.Qu'Allah vous récompense.
Amine
Wallahi deysane amin ❤
Heureusement que vous êtes là. On est fier de vous yaa Oustaz ✊😪 walahi on vous aime ❤ on vous suit ⚘ longue vie à vous 🌷 Masha'Allah
Yalna leen Yallah☝ fay contaan nanou cii yeen Yallah xamnako ... Al Quran ak Sunnah rek ☝
BaarakAllahou fiika akhi Ababacar . Qu'Allah accepte nos oeuvres.
Amiine🤲
@@DaroulBirrTV Amine 🤲 contane nanou ci ligueey bii Masha'Allah
NAFEKH MEUNOUL DEGLOU OUSTAE OUMAR SALL WALLAHI DPEUIS MAROC NDAM REK SUNNA MBA SONEUH💪💪🇲🇦🇸🇳
Machallah oustaz amna sollo
Walahi sunnah rekk amoul lenene ❤
Wallahi
Wallahi deugue bu werr
😱
Allahu akbar ya oustaz barakallahu fikum excellent travail, e sont des guides mouchrikouna
Suis Mouride mh je suis les conseils de Oustaz Oumar il est un vrai soldat de l’islam❤️✌🏿doundal lou beurri 🙏🏿❤️
Sénégal aye nafek daniou fé berie mouhamed mo guene bamba foufe ❤❤❤❤❤❤❤
Kaan moo Laa waakh bamba mo gueun yonetbii. Nafex you kaatt sen ndeye ngen domou sarap ndeyam bi nga doon
Un vrai soldat de l'islam ❤
Alhamdou lillahi biniou yalla mayé oustaze oumar sall 💖💘💯
Alhamdouliallah
Macha'allah DEUG kouko deigg xamni DEUG la. Barak'allah fikm. Yalna yallah sameu niou tei hir niou si bopam
Subhanallah si seulement tout les sénégalais qui pouvaient écouté et suivre se Sheikh ils seront sur bonne voix mais je ne généralise pas!!
Nanou guém yalla ak yonént ti mo guén mane dh yalla ak yonént tam yi la guém
Mashallah toma man.tmt dh niom rék lay top
J'habite à kolda et c'est ton discours que l'imam de notre mosquée a tenu ce vendredi
Machallah barakallahou fikoum ahlou sounnah yalna yalla sougnou borom samou alxouran ak sounnah amine yarabi
Sama kharit par force ,sama grand par force sama papa par force ♥️😍❤️💯🧠🧠✨🌟je t'aime fort par Allah ♥️
Par la grâce de Dieu,nous avons très tôt découvert qu il avait des problèmes de personalités.C est un égocentrique.Mais heureusement que vous êtes là pour nous éviter de suivre ces égarés en nous guidant sur le droit chemin .Allahou ak bar.
Musulman et talibé Cheikh mais vraiment Oustaz ne dit que la vérité walahi. Ma sha Allah.
Voici un vrai kilifa dîné différent des khilifa tarikha,un grand combattant de l islam
Sénégal moi bari nafek oustaz nous sommes derrière toi .ici on défend les marabouts et on ne défend ni dieu ni le prophete
Ma sha Allah ♥️ yaw yala rek mo lay same ❤ jarajeuf oustaz kene monouloula dara . alahou akbar
Wah deugg yàlla man dè yonnou soufii lay dounde wayè wallaahi ahlou sunna ñuy protegè diinè lañu mashallah oustaz from BELGIQUE 🇧🇪
Lolu mo wara khamalni sunnah rék moy deug guéneul ci soufi bigua nék
@@PAPINO7450 non non soufi bima nèkk guissu massi lu deuppo woul al Quran ak sunna même si que yènsay Amna ñiou beuri dañiy dèbordè
@@mansourfall5051 yalna nala yàlla Sam tè aar la
@@ousmane5807 kon kay nékko si soufi
Bokumi magui lay hamalni bén yone rék la islam am dou 2 dou 3 yonentibi (SAW) wahonané sama héte dina diviséwou 73 yone 72 yeup safara laniou dieum bamou des niou toppu yonnu Alquran ak sama sunnah kép kone bokku yalla naniou yalla ték ci yone wowou té sahalniouci 🙏
@@ousmane5807" yalna nala yàlla Sam té aar la " macha'Allah yalla dafa beug niouy rafétal
Machallah Ya Oustaz, vraiment vous êtes une référence pour nous.Merci pour la clarification.
On est fiere vous eye comme Le sheikh rabin ibn heudin almad haliyou on est avec vous
Allahu Akbarr. May Allah increase your knowledge, increase your hikma. Outaz Omar Sall may Allah prolong your life and increase your confidence.
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته ماشاء الله جزاكم الله خيرا حفظكم الله ورعاكم وثبتنا الله في السنة
اللهم آمين
En tout moi,je te suis Oustaz,je t'écoute tu es mon guide amoul bay
Diarama
Franchement ya ouztaz machallah demm la beug tei yallah takh yngui wakh Lou werr di yeiih gnou beurri, machallah
yalla nala fi yalla bayi basi kana ma kanam inchallah soldarou l'Islam bi🙏🙏🙏🙏baraka lahou fikoum
Barakallahou fiik ya Oustaz Oumar Sall Yalla na borom bi soubhanahou wa taعala sameu leu 🤲
Merci oustaz mou selami ma yeureum Say nonne amal diam yalla nala yalla sama amine 🤲
Machaallah Oustaz Oumar Sall yalna yalla deugueureul takhaway bii
Le problème est très simple la plus part des Sénégalais qui croient aux serignes NE CROIENT PAS EN DIEU, AUX PROPHÈTES, AUX SAHABAS...PIR ILS CROIENT RENTRER AU PARADIS SANS PASSER PAR DIEU LE TOUT PUISSANT...DONC LOU SÉNÉGALAIS YI BEUG NON ÇA ME DÉPASSE NON DES CON DES FOUS NON C'EST INCROYABLE...
Ya meunaa niaf sa ndeye doul embecile domou sarap ndeyam bi nga doon
Que allah le tout puissant te protège et te facilite les choses inshallah Oustaz oumar sall
Mashallah amna solo séydina Muhammad sallallahou aléyhi wasalam mako beug bilay
Force à vous yaa Oustaz
Que Dieu vous assiste 🤲🤲
Ya Oustaz SALL NEXOUL WAYE WAXNGA DEUGG .
Alhamdulillah xol Sedna djajakallahu khayran yaa oustaz yAllah nala yAllah my gud fane ak weur mu deuncieul leu djannatul firdws a'ala 🤗
Baraka-Allahou fii kum ya oustaz Macha Allah 🥰 ama tina solo
Yallah naléen yallah sammu
Bilahi nafékh doula dégulou yalla nala yalla sam soutourala
assalamou aleikoum ya oustaz démala sop té yalla takh yalla nalla yalla samb , samb kép kouye diotali alkhourxane ak sunnah
Alhamdulillah baniou yalla tégué thi Alkhourane ak Sounah, Yonou Siratal moustahim! Yalla ben yone bou bakh la am, moy yyonou Siratal moustahim, pas Siratal tidiane, wala mourid, wala shia, wala layenne, wala benen boumou meunti done. Yalna niou yalla sahal thi bou bakh bi, bimou toudal boppam.
Li Moy yone bou dioub bi nak Al hamdoulilah
Dangay doul rék yaw
@@serignemouhamadoumadiamasy5574 Hahahah 🤣, wakhma fou yalla wakhé benen yone boudoul Siratal moustahim? Frere, yalna la yalla dioubal. Yone you nit sos dou meussa yam ak yone bou yalla reud, yonente yi nieuw téggou thi. Tarikha bokoul thi diné baay. Boko beugué geum nak, yaw la rek. Am nga thi plain droit.
@@CHK63 tarixa yi ngén di khass nio takh ngén tala dioly ak diangue alkhouran dangay dém nga lire li serigne touba bindeu dinga kham lan moy yonou mouride
@@serignemouhamadoumadiamasy5574 monté serigne Touba mo bind “rouhou diam yi mongui sama lokho”, “Kaba gui mongui Touba”, “Damay deukalé ak yalla”, “nieup dina niou deh bamou dess mane”. Li yeup so démé thi Khatimoul Mounajati, di nga ko thi fék! Li yonente bi wakh moy deug, lep louniou soss thi diné ji daay wathié yone, té kou wathi yone, dem safar! Koulou biddahatin dalala, wa kouloulou dalalatine fin nar. Wakh ma bakham sa serigne féna loul yalla thi limou wakh!
Heureusement qu’il y’a des gens comme vous.Merci
Oustaz yafi nek deh❤❤❤❤ niongui sa guinaw sénégalais yi bakh rk nga beug❤️❤️
Tu et victorios tu vas toujour gagnee par allah ischaalahu obtained baucoup
Je suis fervent mouride mais je suis d’accord avec cette vidéo !! C’est quelle histoire de blasphémer en plein jour comme ça ! Merci Wa salam
Dou mouride doo sarap ndeyam
Merci y'a oustaze yague fii th wérr inchalla ❤️🙏
Ken j'ai commencé a t'écouter vraiment tu m'aide vraiment dans ma religion
Ma cha alla yalla moley faye
Mom khana chaque année mou togne kèneu😢😢 Ya oustaz ya baax Dieureudieuf 🙏
Yaw mom dokhal rek
Bolé ci ci barké ALLAHOU AL HAFIDH Ak YONENTAM you sélleu ya.
Merci beaucoup ya oustage ALLAH vous récompense
Machaa Allah , Diajakalahou hayran y'a Oustaze Qu'Allah vous récompense.
Qu'Allah vous accorde longue vie oustaz et une bonne santé. Y'Allah nala Yallah fay sa xol bou rafet ak yene biga am si dioulit yi. Amine ya.rabbi
Ma sha Allah oustaz Omar Sall walahi wakh nga deug
اللهم صلي وسلم وبارك على سيدنا وحبيبنا ونبينا محمد وعلى آله وأصحابه أجمعين يارب العالمين
Macha Allah oustaz sant yalla ba nitou yalla ni yow wakh dji lolou. sougnou Sénégal djarna sétat khéli dagno rér déh.
Yalla na niou borome bi maye moudiou bou raféte 🤲
VV islam et la sunna qu'Allah vous récompense 🤲💕💞💓😭😭😭😭
Yalla na yallah yokou say fane Amin
MachaAllah Ya Oustaz Yallah nang fi yagg téh wérr... Yallah na Yallah dolél Ummati Mouhammad Rassoulillah SallAllahou Aleyhi Wa Sallam 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Wollahi dèmbue rk mangui don werantè ak niom nyii dè nio doyy warr wollahi merci oustaz yalna la yallah defal diamue
Je suis vraiment fière de vous Machalla
De verdad tu eres mouslime de verdad ❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoullilah, alhamdoullilah, alhamdoullilah.
Bifi yallah bayyee ay niti sounneuh
جزاك الله عنا كل الخير 🙌🙏
Salam oustaz pure vérité alhamdoulilah que Alla nous donne longue vie et beaucoup de santé
Mash’Allah Sheikhna yalnala yallah sammeu❤️✨🤲🏽
Diereudieuff oustage Oumar Sall
Macha’allah y’a ouztass yagg lol y’a wër
Ay way dougal l'en ma si groupe WhatsApp outaze Oumar Sall Moy sam sirnge manchall révolutionnaire Islam goudal fan diam si yaw 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
ما شاء الله حفظك الله ورعاك من كل شر
Que le bon Dieu les réveille.Amine
Alhamdoulilah 🤲🙏🏿
Oustaz longue vie à vous !!! Allahumma Amine. Pas de prétexte dans l'au-delà.
Un vrai discours religieux Omar sall manchallah 🌹.
Seul la vérité est une mais l'erreur est multiple.
Vérité absolu on est très fier de vous vous parlez rien que l'islam
Masha'Allah oustaz oumar sall.. qui waroul wone toudou Moustapha.. ndakh mérité wuko
Mashah Allah sama idole
Alhamdoulillah sunna rek moy degue ❤
Ya wakh deug dé oustaz
Encore une fois merci à vous oustaz
Masha Allah yàlla oustaz yàlla na yàlla yagual sa takhaway té mousseul niou seytané
جزاكم المولى خير الجزاء ونفع بكم الاسلام
Kou la sagna attaquer Nioun ak sunu groupe yi ma khame di na gnou diok songue lénn. Force et courage à toi.
Je suis vraiment content de vous ya oustaz man damma beugone hamm mom fan la deuk thy Dakar damako beugone setci
BarikaAllah firkoum nous sommes sincèrement fier de vous ManchAllah mais on dirait que le Sénégal est pays où l'islam n'a pas d'importance 💔😭 c'est très malheureux de vivre dans un pays ignorants comme ça 😭🙏 💔
😂😂philodoff Ouztaz allah ye barick fik heureusement que vous êtes là
Jërëjëf Oustaz Oumar Ahmad SALL Masha'Allah
Dia dieuf oustaz nafék doula déglou
BARAKALLAH fikoum mon frère goudalfane wer ak werle
Heureusement on a toujours nos guides pour nous éclairé
Macha Allah
Machallah amna solo ❤❤❤✅🇸🇳🇸🇳
Mashaa Allah oustaz, Merci bcp et qu'Allah vous recompense
Mashalah yala moo laay faay ouatez Sénégal 🇸🇳 ayy doff rek la barri
Merci beaucoup
Yalna yalla mouseule gnou si barké mouhamed
Mane nehouma Dara bilay Serigne sy
MACHALLAH.OUSTAZ.OUMAR.SALL.AMNA.SOLO🥰🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍😍
Yalna Yalla Samal Niou Sunu Goorgui Serigne MOUSTAPHA SY 💚
Allahu akbar. Jeureujeuff yaa Oustaz. Yagg fii tee werr
Merci oustaze Oumar sall
MashaAllah, Ahloul sounah wa jamaá