Machalla cou bakhki tontoubi lerna teu endnakoum mandouté cou nek ak sa responsabilité Yalla nala samou teu arla borom khamkham you melni yèn la adounabi sokhla machalla khamkham andout akoub niak tèguine
Si tel est le cas, même pendant le pèlerinage à la Mecque, personne ne peut tout contrôler, et il y passé sans doute des choses banies. Pourtant personne ne dit qu'on doit l'arrêter. Les bonnes choses pendant ces événements sont largement supérieures aux mauvaises, c'est ça l'essentiel! L'intention compte plus...
Très pertinente comme reponse. En toute chose dans la religion, il faut éviter les derives. L'enseignement de Cheikhoul khadim sama serigne comme tous les autres saint dans ce pays se base uniquement sur le coran et la sunna. Donc nous les talibés nous avons l'obligation de les honorer devant Dieu et les hommes en esseyant au tant que possible d'etre de bons musulmans.
Machallah wakh nga deug pire Senegal mome Dani thiakhane rek gamou yi gaur yi ak djiguen di diakhasso gni di dohananté gni di lalanté ak katanté va souba diot gnouné Dani gamou tchimmm
Ibn Kathir رحمه الله a dit : "Ahlul Sunnah wal jama’a disent que tout acte ou parole qui n'est pas établi/confirmé des compagnons : est une innovation, car si cela était un bien, ils nous auraient devancé en cela !" Tafsir sourate 46 verset 11 قال الإمام ابن كثير رحمه الله : وأما أهل السنة والجماعة فيقولون في كل فعل وقول لم يثبت عن الصحابة: هو بدعة؛ لأنه لو كان خيرا لسبقونا إليه تفسير سورة ٤٦ أية ١١
Machallah imams mak bou bakh dafay defarr même so guissei lou daganoul sakh communication Bi na diar yone mais meussouma xamni 24 ak 31 nonou leu deimei
Je comprends plus les savants aujourd'hui notre prophète Mahomet sws a été clair concernant les innovations que tt innovations et une perdition est aujourd'hui certains savants cherche des prétexte pour nous faire croire a des bidah
Amna sollo.... Ce saint homme limouy wax bi biko Moado bindei amna plus d un siècle😏 « ALA AZIMO LAYLAL WILADATI HISBATANE!!-IZA LAM YAKUN NAXWAL XARAMI HUDULU! « Célébrer le pour acquérir des bienfaits SSS vous n’y faites op kelk choz d kharam » donc montr yu bax yei bok heur....dagni deim Tivaoune di gamou ba bir Aldiana inshaAllah
Imam bi loumou wakh leer na nagn, amoul ken kou meuneu wakh ni meunna sam gammou, ndakhté koureul bou ko organise boufa amé naka soudoul nonou, Niouko def amnagn tchi wall wayé borom koureul bi amna tchi wall momit. Sunna li lay diangal, entre le pire et le moins pire il faut choisir le moins pire, en plus konn dou farata dou sunna, amoul benn manna ngay dieul risque di diakhassé goor ak djiguénn, di fa def naka soudoul nonou. Konn ndjittou confrerie yii senni responsabilité est engagé sur tous les plans, yalla mom nelawoul. té kounek ak seu bamel, ben mindeuf mounoul térré yalla fay la linga liguey, mounek louakh walla lou bonn.
Mach’Allah c’est ça la vie.Nit sou tongnai ba kame dangaye retounai mach’Allah ken d’où yaww vie sur toi et continue comme ça inch’Allah .Yalla nalla yalla same,deff si yaww lou guen ak tawfwkk mach’Allah .Alhahouma barikk ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Allah Akbar way oustaz mouytoul sabob te nga ragalyalla . Thi lee Nagy wax. Toute innovation est également. Tu le sais mieux que quiconque. Depuis ta sortie vraiment on ne comprend pas.
Le compagnon 'Abdallah Ibn Mas'oud (qu'Allah l'agrée) a dit: « Suivez et n'innovez pas car certes cela vous suffira et toute innovation est égarement ». (Rapporté par Abou Khaythama dans Kitab Al Ilm n°54 et authentifié par Cheikh Albani dans sa correction de cet ouvrage) قال عبد الله بن مسعود رضي الله عنه : اتبعوا ولا تبتدعوا فقد كفيتم وكل بدعة ضلالة (رواه أبو خيثمة في كتاب العلم رقم ٥٤ و صححه الشيخ الألباني في تحقيقه لهذا كتاب)
D'après Aicha (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Celui qui innove dans notre affaire-ci (*) une chose qui n'en fait pas partie, alors cette chose est rejetée ». (Rapporté par Boukhari dans son Sahih n°2697 et mouslim dans son Sahih n°1718) Et dans une autre version: « Celui qui fait un acte sur lequel il n'y a pas notre ordre alors cet acte est rejeté ». (Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°1718) (*) C'est à dire dans notre religion. عن عائشة رضي الله عنها قال النبي صلى الله عليه و سلم : من أحدث في أمرنا هذا ما ليس منه فهو ردّ (رواه البخاري في صحيحه رقم ٢٦٩٧ و مسلم في صحيحه رقم ١٧١٨) و في رواية : من عمل عملا ليس عليه أمرنا فهو ردّ (رواها مسلم في صحيحه رقم ١٧١٨) L'imam Ibn Rajab Al Hanbali (mort en 795) a dit dans Jami' Al Ouloum Wal Hikam p 96: « Ce hadith est une base immense parmi les bases de l'islam, de la même manière que le hadith - Les actions ne valent que par leurs intentions - est la balance pour les actes intérieurs, ce hadith est la balance pour les actes extérieurs. Ainsi de la même manière que tout acte par lequel on ne recherche pas le visage d'Allah ne rapporte aucune récompense à son auteur, tout acte pour lequel il n'y a pas l'ordre d'Allah et de son Messager (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) est rejeté ».
Imam alioune badara ndao yalna ko yalla yeureme té khéréko aldiana si barkép seydina mouhamad ❤❤❤❤❤
رحمه الله تعالى كان عالما بحق ، ومحترما لجميع العلماء
Ki kilifeu machallah il suffit de le regarder tu vois en lui la pureté et la sainteté... Nous avons besoin d’imam comme ça
MOTAX NGUÉBN BONNNN
@@sayroulahalkhayrisayroulah21 légui yaw ya bakh vrai domaram moy yéneu
Machaalah Imam Ta zeynab hamona nitou deug gua yalna firdawssi done wathiouwayam
Anime yaraby
Sa réponse sur le gamou est plus convainquante.. Dieureudieuf Oustaz !
Imam ndow yalna yalla goudeule seuye fane amine Inchala
Machalla imam, vous êtes posé , correct et très courtois sur vos propos, votre message est clair et net...
Machallah Imam.
Qu’Allah le Tout Puissant guide vos pas ,vous accorde une longue vie couronnée de santé et de bonheur.
Yalla nala yalla defal diam pape
Très pertinent et facile à comprendre grâce à de bonnes explications
Samm ko meunoul nék Sénégal 🇸🇳
Lolou motakh niou warko bayyi
Franchement Imam Réponse bi lérr na trop
Jazahouk allah khayran
Machallah Imam Yallah na Yallah goudeul fane Yi
Ndaysane soumako kholè rèk Sama khèle dème si sokhna zeinab fall bi mou koy dèfandre yallah na yallah deugue rale la wa oustaz 🤲🤲
Tu as raison Maty yallah nako yallah yereuum
@@lassanadoucoure6586 Aminee
Yannako yalla yeureum té mayko aldiannatoul firdawsi
Amine yarabi maty Diop
Ndeysane paid a son âme
Machalla cou bakhki tontoubi lerna teu endnakoum mandouté cou nek ak sa responsabilité Yalla nala samou teu arla borom khamkham you melni yèn la adounabi sokhla machalla khamkham andout akoub niak tèguine
TRES BONNE REPONSE YA OUZTAZ POURTANT LII LA SERIGNE TOUBA AK MAME MAODO WAKH SI GAMOU NA TEGOU SI SELAL
Machallah Machallah Machallah. je suis fière de vous
قال سيدالحاج ماللك سه رضي الله عنه
الاعظموا ليلة ولادة حسبة. إذا لم يكن نحو الحرام عدول
Ma cha Allah Oustaz wakhe bi rafétna téguinéna soukran
Alhamdoulillah. les articles sur la presse avaient tellement diabolisé cet homme que je suis arrivé à douter de lui par moment mais Allah est juste
Mouride la dee mais nit kou bakhla wallahi...
@@diopletaifoisdiopletaifois6639 khana do dioulit
Quelle sagesse !!! Macha'Allah
Longue vie à toi imam 🙏🏼🙏🏼
Amine
Amiin
Yalna ko yàlla yërêm😢
Man dàl khamnà nou yenenté bi diangualè nakalagnou koy guammoulè tè lôlou lènna dongue la moy wôr thi bissou altiné. Guamou guàgui nônou. Kepp kou thi yokk dara kookou moy kou soss,tè app soss môme thi rére lay diémé borôm tè rére môme yalla n'a gnou ko yalla Moussal amine
t mm pas serieu
Diallo amirou ya guatt khél
Merci oustaz Aliou ndao,tè ngua djiégal gniou si bèpp sénégalais bou djiouma sissa procès bii
Merci beaucoup je suis d’accord avec toi oustaz
Manchalla
Machallah papa doundal wéral yalna la fi yalla yagall
Alhadji Malick Sy li mouffi li gueye kenne mounouko yakkue ndakh Yalla rek motkh AK Yenentoubi dierredieff Alhadji Malick Sy,👏👏📿📿😍
Merci ell malick
li moy khamkhame بارك الله فيك ونصرك الله
Machallah y’a Oustaz
Merci beaucoup pour votre éclairage
❤❤❤❤❤❤❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Tabaa ra KALLAH
Merci imam yalena yalla samela
Yalna la yalla soutoural
ماشاء الله بارك الله فيكم
Machallah longue vie à vous oustaz que la paix soit avec vous
Amine
Pertient Imam et très modeste MachaAllah yallah na yallah goudal say fane 🥰
Diera fief serigne touba
Bilahi ken dou serigne touba
Khady fall dieuredieuf
merci Imam
yagu fi té wër
Si tel est le cas, même pendant le pèlerinage à la Mecque, personne ne peut tout contrôler, et il y passé sans doute des choses banies. Pourtant personne ne dit qu'on doit l'arrêter. Les bonnes choses pendant ces événements sont largement supérieures aux mauvaises, c'est ça l'essentiel! L'intention compte plus...
Dieuredieuf ❤❤❤❤
Ndaysane kilife guii diam si yaw machaallah 😍
Amna solo Machallah
Mashallah c’est très clair
Kham kham deugg la wakhé je suis mourid mais Lim wakh la serigne touba wakh Tahziimouho bissounati
Je suis mourid moy lane ?
Je suis mouride moy Yon bou dieum SA yalla
Momar Talla Mboup merci frére douko dindi
Momar Talla Mboup yonou dieum ci yAllah moy yAllah yonentè bi ak sunna on est daccord?
@@lassanadoucoure6586 balegui wakha go yoon wi noumou toudou
MachaAllah
Très pertinente comme reponse. En toute chose dans la religion, il faut éviter les derives. L'enseignement de Cheikhoul khadim sama serigne comme tous les autres saint dans ce pays se base uniquement sur le coran et la sunna. Donc nous les talibés nous avons l'obligation de les honorer devant Dieu et les hommes en esseyant au tant que possible d'etre de bons musulmans.
اللهم إغفر له وارحمه
شكرالك ياشيخ
Macha Alla longue vie
ماشاء كلام مفهوم وجميل نسأل الله أن يحفظك ويرعاك ياإمام
Vraimt pa bi diambareu leu machalla
Machallah wakh nga deug pire Senegal mome Dani thiakhane rek gamou yi gaur yi ak djiguen di diakhasso gni di dohananté gni di lalanté ak katanté va souba diot gnouné Dani gamou tchimmm
Ioe ya niaw lamine toumal sa morromou djioulitt yalna yalla sam
Ibn Kathir رحمه الله a dit :
"Ahlul Sunnah wal jama’a disent que tout acte ou parole qui n'est pas établi/confirmé des compagnons : est une innovation, car si cela était un bien, ils nous auraient devancé en cela !"
Tafsir sourate 46 verset 11
قال الإمام ابن كثير رحمه الله :
وأما أهل السنة والجماعة فيقولون في كل فعل وقول لم يثبت عن الصحابة: هو بدعة؛ لأنه لو كان خيرا لسبقونا إليه
تفسير سورة ٤٦ أية ١١
Machalla imam wakh bi dioubna rafétena
Machallah imams mak bou bakh dafay defarr même so guissei lou daganoul sakh communication Bi na diar yone mais meussouma xamni 24 ak 31 nonou leu deimei
Merci imam
Macha alla imam ndao
Macha oustaz
macha Allah imam ndaw wakh dji fachahana
Machallah oustaz
Je comprends plus les savants aujourd'hui notre prophète Mahomet sws a été clair concernant les innovations que tt innovations et une perdition est aujourd'hui certains savants cherche des prétexte pour nous faire croire a des bidah
Relisez ce que vous dites soit une contradiction ou vous ne faites pas la différence entre innovation et bida.mille excuse!
@@masiba7272 nom c n'est rien mon frere je vous reposé la question c quoi la différence entre bidah et innovation
@@soni-boys999 aucune différence
@@masiba7272 ok bonne soirée
C'est un vrai Imam
Man ki bilahii walaye dama ko sopp si ayy kadou rafèt🙏🙏doundal lol imam🙏🙏🤲
Amine
Thiey alkhorane ak sunna yallah naniou si yallah sakhal
Aamiine
Amna sollo....
Ce saint homme limouy wax bi biko Moado bindei amna plus d un siècle😏 « ALA AZIMO LAYLAL WILADATI HISBATANE!!-IZA LAM YAKUN NAXWAL XARAMI HUDULU! « Célébrer le pour acquérir des bienfaits SSS vous n’y faites op kelk choz d kharam » donc montr yu bax yei bok heur....dagni deim Tivaoune di gamou ba bir Aldiana inshaAllah
Machallah louniou sopeu la pour sakou ngeuramal borom bi Iman yague fi ta andeu ak yéreu
SENN IMAM AMOUL KHAM KHAM
Kane moko sopou?
Oustaz Yallah Nala Yallah FAYE
Mamadou Nd
Amine
Machalla nice na
MachaAllah je suis mouride mai liga wakh la geume niou bari ni ni gamou ay thiakhane la
Magal Nak lanela?
@@leuzleuz8602 bilay walay wakhal deh niom kan laniouy magal nit yonentibi bi rek mo diara magal
@@mouhaofficiel6638dagnou fatè Séne bopp, wana rék magal nit
Magal Sant yalla la
@@AladjiDameDiop_SN fallait l'appeler santa Yalla alors au lieu de l'appeler magal parce que Yalla mangana déjà
Imam bi loumou wakh leer na nagn, amoul ken kou meuneu wakh ni meunna sam gammou, ndakhté koureul bou ko organise boufa amé naka soudoul nonou, Niouko def amnagn tchi wall wayé borom koureul bi amna tchi wall momit.
Sunna li lay diangal, entre le pire et le moins pire il faut choisir le moins pire, en plus konn dou farata dou sunna, amoul benn manna ngay dieul risque di diakhassé goor ak djiguénn, di fa def naka soudoul nonou. Konn ndjittou confrerie yii senni responsabilité est engagé sur tous les plans, yalla mom nelawoul. té kounek ak seu bamel, ben mindeuf mounoul térré yalla fay la linga liguey, mounek louakh walla lou bonn.
En houdiathie yii dem maka def fa ak moye lolou kou cciye am wal yalla santané di
Yalla d'où diokh kéna niakhou diambour
Machalah al Imam
Kii moy borom ham ham nag.Machaallah mais ñenen ñiko daganal ñep ay naffékh lañu.
Imam Ndao ma ngui lay Balou akh bou werr ndakh fogone na ni li gnou la toumalone deug la diegalou bou werr...djangal ngama mandou taye
Mach’Allah c’est ça la vie.Nit sou tongnai ba kame dangaye retounai mach’Allah ken d’où yaww vie sur toi et continue comme ça inch’Allah .Yalla nalla yalla same,deff si yaww lou guen ak tawfwkk mach’Allah .Alhahouma barikk ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Allah Akbar way oustaz mouytoul sabob te nga ragalyalla . Thi lee Nagy wax. Toute innovation est également. Tu le sais mieux que quiconque. Depuis ta sortie vraiment on ne comprend pas.
Degge bou werr macha allah
Imame ndaw Liga wakh dioumté bou reuy la si Kouy doundou sunna
Gamou bida la
Sénégal Kouy wakh loulene arranger rk niou far ak yow
C'est la 1ere fois que je trouve son discours pas clair. Louniou soss thi dine bida la te bepeu bida ak sankoute la.
Toi tes drôle là @@fatimazahrachannel6404
Yalnagnou yalla maye dëgg ak toop
BarakAllahou fik oustaz , bul ragal 🤔 gamou Ken munuka sammu , bidaa leu c'est clair , kulu bidaa atine dalala ,
blacking blacking waxofi dara ioe
@@melokaanoumouridetv5107 yow key yay dof
Wakh ngua deug
Waw coferanse bida walla dou bida
Longue vie a toi
Machalah wax nga thi xam xam
Imam man sha allah kadou yi refete na yalle na yalla yokk ham ham bi ak katane bi
Alhamdou lilah diambar nga dh wayé fiimoom d'accorouma fi ak yow wakhal ni si yow bidha ngako diappé
Le compagnon 'Abdallah Ibn Mas'oud (qu'Allah l'agrée) a dit: « Suivez et n'innovez pas car certes cela vous suffira et toute innovation est égarement ».
(Rapporté par Abou Khaythama dans Kitab Al Ilm n°54 et authentifié par Cheikh Albani dans sa correction de cet ouvrage)
قال عبد الله بن مسعود رضي الله عنه : اتبعوا ولا تبتدعوا فقد كفيتم وكل بدعة ضلالة
(رواه أبو خيثمة في كتاب العلم رقم ٥٤ و صححه الشيخ الألباني في تحقيقه لهذا كتاب)
❤️
*Nitou yalla pire bilahi imame yagueu fi lol té wérr🙏🙏🙏*
Machallah wakhdji rafetna
Machallah imam deug rek leye wakh
Machallah Imam diangue gua trop, wayé dess na. Machallah
ايدك الله ونصرك
amine
Machallah Imame ndao
machalla ya oustas wayè basariya younénetabi bagui moguifi grume ac wédi rek moufinék
Yamana doule
Ah non Iman tu as tuer le Game magnifique réponse si vous ne pouvez pas célèbre d'une bonne manière alors laisser tomber wa salam
ما شا الله يا امام Yalna borom bi barkel xam-xam te defal tawfeek
Machalla amna solo loll
Personnellement maane manguilay djiégalou
ماشاء الله امام واضح
D'après Aicha (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Celui qui innove dans notre affaire-ci (*) une chose qui n'en fait pas partie, alors cette chose est rejetée ».
(Rapporté par Boukhari dans son Sahih n°2697 et mouslim dans son Sahih n°1718)
Et dans une autre version: « Celui qui fait un acte sur lequel il n'y a pas notre ordre alors cet acte est rejeté ».
(Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°1718)
(*) C'est à dire dans notre religion.
عن عائشة رضي الله عنها قال النبي صلى الله عليه و سلم : من أحدث في أمرنا هذا ما ليس منه فهو ردّ
(رواه البخاري في صحيحه رقم ٢٦٩٧ و مسلم في صحيحه رقم ١٧١٨)
و في رواية : من عمل عملا ليس عليه أمرنا فهو ردّ
(رواها مسلم في صحيحه رقم ١٧١٨)
L'imam Ibn Rajab Al Hanbali (mort en 795) a dit dans Jami' Al Ouloum Wal Hikam p 96:
« Ce hadith est une base immense parmi les bases de l'islam, de la même manière que le hadith - Les actions ne valent que par leurs intentions - est la balance pour les actes intérieurs, ce hadith est la balance pour les actes extérieurs.
Ainsi de la même manière que tout acte par lequel on ne recherche pas le visage d'Allah ne rapporte aucune récompense à son auteur, tout acte pour lequel il n'y a pas l'ordre d'Allah et de son Messager (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) est rejeté ».
Man mako begue ta yalla yakh❤💎
Machallah imam kadou yi lerna