Sage femme bi à raison khale deniou koy accompagné mais sénégalais mo begue lou yombe mouy taw guay yoni khale je suis au Maroc mais nar yi tte temps ils accompagnement leurs enfants dou niou lene bayi niouy guene kesse
Grand tua raison g constaté cela mbour 3 et mbour 4 keneu xamoul kene diga deuk ak nit dooko xam doula xam bop sa bop ken sorelewoul kene c pas normal, en plus bedeu xate naniou trop le dame osi a raison terrain yi mooy lolou surtout ici
La sage femme a parfaitement raison une part de responsabilité revient au parents ngay yonni khalei thi taw biii,pour calmer sen colère ngen sipiko ken
Yalnalen yala yeureum mé lii c pas normal xana mbour 3 cité la mm soufeke cité la osi normaloul kene xamanté melni ay diambour epui mouy taw gay yoni ak xalé osi

Ndeyssane massa 😢Yallah Naniou Motali Sen Ndaw Aldiana Firdawsi Ci Barke Seydina MOUHAMED ( p.s.l) Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🤲 🤲🤲😔😔
Diatou masa yalla nala yalla may xolou mougne firdawsi Di séne keur
Comment peut on creuser une fausse sceptique à ciel ouvert ? Surtout en pleine hivernage ?? Sénégal daal...
Qu'ils reposent en paix!!
Yalna léne yallah yeureum Allahouma amine incha allah
Paix à leurs âmes 😢
Métina trop wallahi
Ndéye sane vraiment métina trop yalla yeureum lène amine way 😭
Grand tua raison g constaté cela mbour 3 et mbour 4 keneu xamoul kene diga deuk ak nit dooko xam doula xam bop sa bop ken sorelewoul kene c pas normal, en plus bedeu xate naniou trop le dame osi a raison terrain yi mooy lolou surtout ici
La sage femme a parfaitement raison une part de responsabilité revient au parents ngay yonni khalei thi taw biii,pour calmer sen colère ngen sipiko ken
Masta en tant que mère li métina trop😭😭😭😭😭
Diatou Gueye massa ina lilahi wa Ina ileyhi radjihoune yalla nalen yalla diegal
😭😭😭😭😭😭😭😭😭. Naissane😢😢😢😢
J ai mal au cœur li mettina trop
Yalla nalen yalla yerem
Kouy yayy sa khôlle dagg n'a di
انا لله وإنا إليه راجعون
Yalla moy def llouka me nak naniou surveiller les enfants
may allah grant their hightest level jannatul firdawsi
Li deh sama kogn la
Paix à leurs âmes 🙏🙏🙏
Masa ma chérie métina trop
Sophia mettina lol mais yalla bakhna
J'habite ici yalla naleen yalla yereum😢 c triste vraiment me bouy taw deleen te xalé yi ici c dangereux
Allahu Akbar lii mettina ndeysane yalnane xippeh janatul firdaws
Yal nala léne yalla yeureum té kharé léne sa Aldjanay firdawsi ya raby
Triste😢😢😢😢
😭
Massa
😭😭😭😭ayyy sama dom demna
Masta ma chérie yalla nalla yalla May kholou mougne c’est très dure mais yalla sou sokhla diam niakki
Massa metina trop
Les chantiers doivent être protégés. C'est n'importe quoi
😭😭😭😭😭😭😭
Yalnalen yala yeureum mé lii c pas normal xana mbour 3 cité la mm soufeke cité la osi normaloul kene xamanté melni ay diambour epui mouy taw gay yoni ak xalé osi
Mbour 3 d mo raw Cité ma chérie ken fallé woul ken bountou keur yi day teudiou lep yaye bou sagane la rk
Mbour3 dé mom Moy lolou ki Di wakh khamnako