Ceux qui disent que liberté bakhoul si djiguén donc vous êtes d’accord gor yi gnognouy réy ? Car si c’était pas le cas kén dou protéger les filles qu’Allah nous guide
yéne dé amoléne lou nguéne di wax nopi rek mo léne war wax nguéne kiko def ki faye lep té géré lep té ba tay dialé woul familles ñieuwul si keur gui top léne kokou yéne gñiko bayé ak kiko takoul diapé ko comme kou yoré diabaram disi def louko néx yéne môme amoléne lou nguéne wax dou sa maye wax nak yénako wax ki guéne adina yalla nako yalla yeureum té djégalko até kosi yeurmandé wam
Yalla nako yalla yeureum té dome dji mague ba nék maak nék président wala commissaire wala commandent ndakh nga kham ki déf li sa yaye dji yalla nako yalla déf si dieume seydina mouhamed pls 😢😢😢😢
Bilay loumétti la mes le fait que niou am soupson té topouniou kabi fofou laniou bayé lokho 😭😭😭😭 yallah nako yallah yeureum té kharéko Aldjianay firdawsi si barké Séydina Mouhamed 🙏🏾
Nama yalla bale dh mais dieynaba amone na liberté d trop tei lolou dou yone mais beine question wadji ko done dokhane khana dafa beuri alal famille Sénégal yi nama yalla bale danio deugue khaliss trop parsk wakho djekeur nane far ay deux jours trois jours lolou warone ngeine ko roussa netali vraiment yalla nako yalla yereume kharé ko aldiana mais sagane ngeine tei lep ndakh khaliss
Mais tamite la fille était majeur et maman, ken dOu top si guinawam diko contrôler. Moi ce que je déplore c est la lenteur de la justice. réaction tardive de la famille d'appeler les médias. Mais certainement sen khôl mo nekhoul wone rek
@@kitokoken2187 kou bakh Sénégal laniou nek dh bayil wakhou majeure neko Europe éducation yi bokoul Sénégal ngay guiss kou am 40ans deuk keur papame en plus copin bi sou amoul wone khaliss famille bi dinagne ko tela wakh deugue justice Sénégal mome douma si débat ndakh Sénégal amoul justice
@@modytoure5278 je suis d'accord avec toi mais bon le mal est déjà fait.le sénégalais a trop peur des personnes fortunées, mo takh gnou nek si deuk bo Di def loulen saff ,té dou moudj fén
@@kitokoken2187 voilà yangi dogua gnew nak nonou la demei wadji limou am khaliss motax gnemei wouniou ko affronté mais souniou topone wadji lgui niou kham kou ray guel bi mane dina am sama soeur mou décédé si yene circonstances yi farame diko djeguei baye ladj autopsie lolou khel moko ndieukoul nangou
Je me demande des fois dans quel état l'être humain peux se trouver pour ôter la vie de son semblable....C inhumain...la famille à une petite responsabilité dans cette histoire ils ont laissé trop de liberté à la défunte (paix à son ame) Trop de liberté et de laisser aller
Far biko ray surement mogui fi Di sètane mais diapal ni so èchapper si justice des hommes do échapper si justice divine Bala nga dé yallah dina la torokhal Djiguène tamit deuk iow kessè waroul takh nga mom sa bopou so dèmé iow Djiguène ba guissato koulo yilif djémal noot sa bakane nek sa kilifa bopou Yallah nala yallah yeureum djégal la
Le pire c’est qu’on avait retrouvé son portable entre les mains de vigiles aux Maristes et après plus rien. Comment ces derniers ont eu le portable ? Aucune enquête n’a été diligentée car la police connaît le coupable et n’a rien fait. Dans ce pays il n’y a que la loi du plus fort qui marche.
Anta Diallo boul accusé famille bi sans raison yeen goor yi sen khaliss kheureum laniou ko ligueye boul Nian dall si niom kheureum yi louniou ladj fou niou diokh ko pour existe deretou faw nga teureul ou teud akh djiguern diou khess ect... donc khalle bi ay agissement won dou naturelle police akh gendarmerie louniou def dou yoon daniou wara aide famille bi def sen deuil wax leen li am au lieu di def de la cachoterie
J’ai suivi 7voix du coeur et je me suis dis qu’il y’avait trop de non dits en plus la dame ne laisser pas le gars s’exprimer elle lui coupait la parole par moment. Yalla na yalla feignal ki ko raay InchaAllah rabbi
Maintenant on est en juillet 2024 il faut que justice soit faite pour Djeneba d'après le discours de la famille elle sortait avec Un proche de l'état il faut réouvrir le dossier de cette fille tuée il y a plus de deux ans que justice soit faite j'ai vu sur tic toc "khelbou sell parlait du décès de Djeneba, et je le soutien vivement
C'est trop triste j'ai eue pitié de son fils les paroles de son ex mari ma fait pleurer yalna yalla nite ko si Barké Yonnentbi sallallahou alleyhi wa salam si Barké werou koor bii 😢😢😢 c'est triste vraiment
Que son âme repose en paix mais en général senegal lifi nek la kene doul wakh tu vois des frères irresponsables qui peuvent pas protéger leur sœur en leurs payant leur études leur besoin ,les parents aussi dangay ame sa dome bu jiguene mou ame far amoul liguey amoul dara dila gèrel sa courant dila diokh gay lek dila defal lep.gnuy lek avec la conscience tranquille. Prenons nos responsabilités et protégeons nos sœur en tant que frère et parents.
La famille a une grosse part de responsabilité dans cette affaire. Comment est ce qu'on peut laisser une femme aller en weekend avec une personne qui n'est pas son mari ou une personne de sa famille! C'est grave et dans tout cela le nerf des maux c'est l'argent. Si une personne fréquente une fille et qui n'est même pas capable d'entrer dans votre concession ou même de rencontrer des membres de la famille c'est une aberration. Elle a juste été envoyer dans la gueule du loup. Puisse son âme repose éternellement en paix et que ceux qui ont ôté celle belle âme à l'affection familiale puisse être trouvés et jugés ici et dans l'au-delà. Et que cette triste histoire nous servent de leçon à toutes et à tous
Je n’aime pas juger mais malheureusement deug nga wakh. Sa famille ne l’a vraiment pas protégée; de son vivant et même après sa mort! En plus je ne comprend pas vouloir cacher le nom du copin😢
De plus en plus les parents montrent leur démission par rapport à l'éducation de leurs enfants. Cette fille qu'Allah ait pitié de son âme, elle est une des victimes de ces nantis qui pensent qu'avec leur argent ils peuvent tout se permettre. La famille de la victime,saisissez un bon avocat pour éclaircir cette affaire
Madame Gaye il faut voir nos entreprises ce sont des arènes de luttes pour occuper certains postes et obtenir des avantages les gens sont prêts à tout tu fais tout le boulot on nomme a des postes stratégiques des gens qui n'ont pas le niveau et ce sont ces derniers qui font ce genres de sacrifices faw nga rey faw nga teud akh djiguern diou kherer ou nioul liii ngakoy seuf foko wo mou wouyou la loko deflo mou def ko ay mbokom souba legui laniouye comprendre si tu n'as pas de la foi tu vas le faire la famille ne réalise qu'après les faits nian yalla mousseul la si pekhe nit kou boon akh djeuf diou boon et après c'est la corruption pour laver l'affront deuk bi metina ba khetou khaliss yitelouleen naniou fedj sen Sokhla au péril de la vie des gens
1)Respectez la mémoire de la défunte. Yalnako yalla yeureum 🤲🏽 2)Famille laxiste en tout point keneu waxatouko. 3)Sen meurtrier présumé xamnguene ko porter leneu plainte dieul leneu avocat allez jusqu’au bout nalene diaral lunekk tei nguene bayii laxisme bii. 4) Ex dieukeur djii dh machallah kou nitter laaa ndeysane. Depuis son meurtre ndeysane je me demandais esk c élucidé?! Kou deff lii yalnako yalla weer sii koor gui!
Sénégal legui dafa beuri ay secte ak sacrifie meurtre bi meune nek affaire yoyou guayi legui dagnouy dokhane djiguene juste pour ça dagnoulene di toure khaliss bou beuri mbagnou diap confiance
En tout cas le conseil qu’on peut en tirer c’est de bien choisir la personne que l’on fréquente, surtout les filles. Certaines se basent juste sur les biens d’un homme et oublier le point le plus important qui est la beauté intérieure. Je m’en limite là, que Dieu l’accueille dans son paradis.
Vous les sénégalais et sénégalaise yii bayilen jugez 😢 si je regarde certains commentaires je pleure même si la victime avait bcp de liberté elle ne mérite pas d’être tuer il faut que justice soit faîte c’est tout yalla nako yalla yeureum ki fatou🙏🏻🙏🏻
Famarta niang faut pas accuser la famille beaucoup de millionnaires et milliardaires sénégalais ou des hommes qui occupent certaines postes le font au périls de leurs vies dans les entreprises il y'a de ces combats mystiques et des sacrifices a faire pour accéder à certains poste deretou ou fok nga rey ou teud akh djiguern djou khereer ou djigueen diou nioul kouk ect.. la fille peut être quelqu'une de très correcte irréprochable dans son comportement mais a cause des choses mystiques elle devient incontrolable jusqu'a son dernier souffle
@@farmataniang5608 c'est allah qui peux te sauver mais aussi prendre ses dispositions mais aussi il faut te protéger il y'a des pratiques que nos grands parents faisaient pour protéger les femmes les enfants utiliser les plantes pour se prémunir de la mauvaise langue du mauvais oeil des pratiques mystiques et qui a tendance à disparaître je donne l'exemple de mon grand frere qui a investi dans l'agriculture son champ lui rapportait des millions chaque année mais il est resté 1 ans 6 mois sans mettre les pieds labas mais dès qu'il en a parlé a ma mère elle l'a mis en rapport avec des vieux qui lui ont donné des mesures de protection aujourd'hui il a repris les choses juste pour dire que la vie d'aujourd'hui kou sagane sa bop sa ndiabot niou rey la mame yi bayinaniou leup
Djiguéne day guate tank tei yéme si lokho Kouy seye seyal tei yalla takhe djiguéne amoul dolé Yaye boye 😭😭😭😭 si képarou gorr rek moy wérou wayam Kouy seuy seuyal dei yalla takhe kouy djiankou khamal foye Téki sa tank
Mais tmt vous qui parlez d'irresponsabilité arrêter, cette fille n'est pas une gamine, elle a un enfant, kham na adouna sa famille n'a pas à prendre des décisions pour elle de plus qui vous dit que sa famille intervenir roule wone ci relation bi avec ce gars louche ? Elle a juste rencontré un de ces monstres 🤦🏾♀️ Yallah rek mo kham qu'Allah lui fasse miséricorde
Si la famille est irresponsable ndakh nan nguay bayé sa dom di ande gor bo khamni takouko di and ak mom week end 3jour te takouko dou yon bref yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana
Bilahi ex mari bi koubakh la nioune djiguene gni dagnouye ame kou bakh tes dougne ko khame niouye top khaliss beu lore souniou bop sou khamone mou dess ak borom kereum dji diamossi yalla yalnako yalla yereume diegueuko atéko si yeurmandéwome yalla méye lene kholou mouye
Vraiment ex marié bi kou bakh na te am coleure khale you djiguen yi daniouy nek ak kou bakh kou Len beug yeureum Len niou ne ko fa niouk di weur brom tour ak brom alal motakh Lou nek laniouy dadiel yalla nako yalla yeureum waye leçon la pour yen djiguen man yalla mo def brom khalis bouma khamoul doumala gne
Le prophète sws a dit si un de vos semblables meurt dites du bien de lui ou garder le silence . Qu’Allah Azawajel lui pardonne ses péchés et qu’il expose les responsables de cet acte ignoble nchaAllah qu’Allah nous pardonne nos péchés qu’Allah nous protége et protège nos familles et proches qu’Allah nous éloigne des gens néfastes au cœur de brutes nchaAllah qu’Allah fasse de nous des gens biens et qu’il nous accorde une bonne fin nchaAllah
J 'ai pas l'habitude de juger les gens mais la famille a trop attendu pour sortir dans les media. La fille était trop indépendante, liberté bou Bari bakhoul. Massa à sa famille et yalna Souf sedd si kawam
Niémé wessouwoul di juger kou deudou juste sur de simple mot de personnes. Nga rouss YALLAH sakh té khamni YALLAH na yékh so deudo do beugue loudoul sédé you rafett dontè dinga fi bayi you safanou. Rew mi kéne khamatoul li sokhor la wala ignane
C une trice histoire k dieu lui accueille dans son paradis et lui pardonne, wayénak la famille devait etre plus responsable en lui exiissant de se marier avec le gars comme çà elle sera légale avec lui
vous etes irresponsable amo leen loleen wakh depuis bobou leep beug lou yombou rekh la mais dieynaba yalnako yalla yeureum té khareko aldiana firdawsi takhawou domam
Nguéne Baalma Sénégal daffa doye waar Imagine toi nga bayi sa Doome ak un gars boo xamni dou dieukeureum pendant 3jours en plus son frère waxnani moussoul guiss waadji Vraiment la faute c’est la famille Vous avez sacrifié votre fille Yéne xaaliss rék nguène guissone ci mome Vraiment c’est dommage
Famille bou neik dafa wara âme kou tangue Di redresse si deugu mais lii yeup début bila laisser aller bii mou diourlii lo djiii lolou ngay récolter famille bi neigliser d le début mais nak yalla nako yalla yeureum t kharerko aldjala
Il y a des gens c'est pas des humains mais en faite c'est des microbes, des virus, des ordures dont malheureusement on est obligé de vivre avec eux dans ce monde. Je prie vraiment que cet énergumène qui a ôté la vie à cette Dame puissent avant sa mort à lui aussi puissent répondre de son acte ignoble d'abord sur terre, que le Seigneur entend ma prière, et qu'il pardonne a la femme ses péchés et l'acceuille dans son paradis céleste.
Nite bouye nieuw bassa bountou keur di séte sa dome niouye ande di déme té diémoléne convoqué ko si bir keur gui wakhtane khame moye kanne vous les parents et grand frère déf guene erreur c'est pour cela douko respecté yal nako yalla yéreum té kharé ko al jennah kiko Ray yal nako yalla nite 14:05
La famille, la famille, la famille…. Trop de manquements c’est dommage quand elle était en vie on peut dire qu’elle est responsable de ses actes mais après sa mort fallait prendre vos responsabilités, suivre les choses, porter plainte et surveiller les actes posés côté justice, saisir les médias à temps mais là c’est trop tard je pense à moins que vous avez de la chance En plus l’étranger là il faut dire son nom et publier sa photo si y’a des témoins ils pourront faire le lien. Pourquoi vous ne prononcez pas son nom? Vous avez peur de le dénoncer ou pas? C’est bizarre
Massa . RIP. Ameen Au Sénégal on cache trop les choses. Cet enfant l amener chez le psychologue pour enfant. Seul un professionnel du domaine mental peut mieux aider et guider cet enfant de 7 ans mentalement. Allah sameu ko . Courage à tte la famille et proches. Y allah Bakhna. Always
99% sure que le gars est le suspect numéro 1 (pour ne pas dire il est le meurtrier sans jugement) Raisons: 1)La fille s’est battue avec le meurtrier et le gar avait une égratignure(selon les témoignages) 2) le gar l’avait battue et menacée de mort 3) le gar a eu laudace de s’occuper de lautopsie sans se soucier de la famille(incroyable, seulement au Sénégal). Si c’était ici en Amerique l’enquête serait concentré sur lui, et la police n’aurait pas besoin d’entrendre 2 miles propriétaire du vehicle qui a transportè la fille cette nuit (il suffit de savoir si le gar possède cette voiture) . Les policiers sénégalais sont bien sûr très forts, Mais bien sûr avec ce ngour de Macky Sall les riches proches du pouvoir sont intouchables. Espoir que Sonko ou autre candidat bou yeguè les choses vont changer. Rest in peace Dieynaba!
Comment on peut laisser un membre de la famille avec son copin pour un week-end Vraiment c'est du n'importe quoi L'argent peut tout acheter sauf un être humain Yalla nako yalla yeureum tè kharéko aldiana
C'est grave ce qu'il est en train de dire ... Quelqu'un qui vient chez moi devant ma porte pour ma fille ou ma sœur a plus reprises soi-disant son copain sans pour autant que j'intervienne, c'est irresponsable de votre part toute la famille nak . Je suis désolé nak
@@nikojonkins5721 Moi j'étais vraiment dépassée . Pourquoi les gens ne réfléchissent pas avant de faire des sorties de ce genre ? Comment peut-on être aussi irresponsable à cause de l'argent ? Desgraciadamente !
Je suis atterré par certains commentaires qui pointent du doigt une supposée responsabilité de la famille de Dieynaba Traore et qui de surcroît, font des allusions malsaines sur la "moralité " de la fille. C'est ignoble et répugnant, un peu de décence et de retenue ne vous ferait pas de mal. Je compatis à la douleur de sa famille et de ses proches. En espérant de tout cœur que les enquêteurs feront le maximum pour mettre la main sur le présumé meurtrier.
C’est ce que je dis les gens n’ont pas le droit de blâmer sa famille ils vivent déjà avec la douleur de la perte de leur fille vos jugements ne leurs font pas du bien. Arrétez seul Dieu peut juger 😢
Franchement une famille très irresponsable comment laisser une fille aller en week-end avk un Homme qui n’est pas son Mari???? Quand ya l’argent c bon 😢
Mane dh bilayiiii magui commentaires le dimanche 21 Juliet à21h 19 munite 2024 batay meuma co faté tei khawmako sakhe mais dafma métiiiiiiii Yalla n’a Yalla yésal yeurmandé si mome barké serigne fallou mbacké
@@onlypandaintownyèen yi sokoy dègue sakh daguaye mère walay médecin yi rékk warougniouko woon wakh béen informations déjà pck c'est pas une menbre de la famille voilà
L’enquête doit être relancée avec celui qui avait menacé de mort DIEYNABA …c’est fort possible qu’il soit l’auteur présumé du crime. Il faut pas avoir peur …il n’a que le BON DIEU sur terre et au delà!!!
A chaque fois damay poser ayy questions sur l’affaire de la fille !!ca me fait tellement mal meussoumako faté ndeysannn comme si dagno bokk dareu.yalla ngeu hippé aldiana Dieynaba
Rien ne justifie le fait de tuer une personne à part la légitime défense la famille a été trop négligente et votre réaction prouve que rien ne peut remplacer une mére un père.
Moi à mon intuition, c'est son copain qui l'a éliminer peut être c'est dû au mariage où autres que le gars n'avait pas l'intention de l'épouser et puis une dispute à éclater, parceque comment il à pu prendre la responsabilité de gérer l'autopsie sans aviser la famille ??? Et disparaître après. Vous avais laisser partir le meurtrier, regarder toutes les détails, et ces effets personnels rien a disparue, cela veut dire la personne qui l'a tuée voulais juste la supprimer et n'a rien pris sur elle, à part peut être jetter son téléphone Déposer une plainte contre son copain qui à gérer l'autopsie et à disparu,
Maïs depuis le début donane suivre cas bi mais li famille expliqué taye mousougnouko expliqué au début comme danion ragalone wak mais yalla na ka yalla yeureum
Yalla nako yalla xaré Aldiana firdawsii Barké AL XOURANE. Mais comment pouvez vous laissé votre soeur votre fille allez en week-end avec un homme qui n'est pas son mari ahhh kel liberté kel famille???
Demandez a ses copines qui étaient avec Elle le soir au terroubi peut être elles savent avec qui elle avait rendez vous c genre de cas pierre Bellemare les enquêtes impossibles lassi wolou😢
Nďaysane ex dieukeuram bi kou balh la
Yalnako yalla yeuram té kharéko Aldiana
Ceux qui disent que liberté bakhoul si djiguén donc vous êtes d’accord gor yi gnognouy réy ? Car si c’était pas le cas kén dou protéger les filles qu’Allah nous guide
yéne dé amoléne lou nguéne di wax nopi rek mo léne war wax nguéne kiko def ki faye lep té géré lep té ba tay dialé woul familles ñieuwul si keur gui top léne kokou yéne gñiko bayé ak kiko takoul diapé ko comme kou yoré diabaram disi def louko néx yéne môme amoléne lou nguéne wax dou sa maye wax nak yénako wax ki guéne adina yalla nako yalla yeureum té djégalko até kosi yeurmandé wam
😢😢
Tellement vrais
Wakh nga lep. Quelle famille irresponsable ! Bayi sa dom Mouy def louko nekh dakh Khaliss. Qu'elle repose en Paix.
Une grande personne majeur et vacciné louko nit meuneul
@@charmecharme7275 khanat diko wax deug rek té yalla takh kofi wax deug même bou méré dîna xame né bokosi gñi kaye diay
Yalla nako yalla yeureum té dome dji mague ba nék maak nék président wala commissaire wala commandent ndakh nga kham ki déf li sa yaye dji yalla nako yalla déf si dieume seydina mouhamed pls 😢😢😢😢
Bilay loumétti la mes le fait que niou am soupson té topouniou kabi fofou laniou bayé lokho 😭😭😭😭 yallah nako yallah yeureum té kharéko Aldjianay firdawsi si barké Séydina Mouhamed 🙏🏾
Ne ''vv' 😊v😊v
Nama yalla bale dh mais dieynaba amone na liberté d trop tei lolou dou yone mais beine question wadji ko done dokhane khana dafa beuri alal famille Sénégal yi nama yalla bale danio deugue khaliss trop parsk wakho djekeur nane far ay deux jours trois jours lolou warone ngeine ko roussa netali vraiment yalla nako yalla yereume kharé ko aldiana mais sagane ngeine tei lep ndakh khaliss
Bilahi dama tiit sakh😮
Mais tamite la fille était majeur et maman, ken dOu top si guinawam diko contrôler. Moi ce que je déplore c est la lenteur de la justice. réaction tardive de la famille d'appeler les médias. Mais certainement sen khôl mo nekhoul wone rek
@@kitokoken2187 kou bakh Sénégal laniou nek dh bayil wakhou majeure neko Europe éducation yi bokoul Sénégal ngay guiss kou am 40ans deuk keur papame en plus copin bi sou amoul wone khaliss famille bi dinagne ko tela wakh deugue justice Sénégal mome douma si débat ndakh Sénégal amoul justice
@@modytoure5278 je suis d'accord avec toi mais bon le mal est déjà fait.le sénégalais a trop peur des personnes fortunées, mo takh gnou nek si deuk bo Di def loulen saff ,té dou moudj fén
@@kitokoken2187 voilà yangi dogua gnew nak nonou la demei wadji limou am khaliss motax gnemei wouniou ko affronté mais souniou topone wadji lgui niou kham kou ray guel bi mane dina am sama soeur mou décédé si yene circonstances yi farame diko djeguei baye ladj autopsie lolou khel moko ndieukoul nangou
Je me demande des fois dans quel état l'être humain peux se trouver pour ôter la vie de son semblable....C inhumain...la famille à une petite responsabilité dans cette histoire ils ont laissé trop de liberté à la défunte (paix à son ame)
Trop de liberté et de laisser aller
Bilay ioe bane khôl la gnio gnou yorrr bay deff gniatéfe yi 😢😢😢ray ni ohhh Yalla nagnou thi Yalla mousseul tei osi gnou bagnan am moudjiou bou gniaw
Machallah, l'ex mari est un homme bien, que Dieu vous apaise.
Far biko ray surement mogui fi Di sètane mais diapal ni so èchapper si justice des hommes do échapper si justice divine Bala nga dé yallah dina la torokhal
Djiguène tamit deuk iow kessè waroul takh nga mom sa bopou so dèmé iow Djiguène ba guissato koulo yilif djémal noot sa bakane nek sa kilifa bopou
Yallah nala yallah yeureum djégal la
Le pire c’est qu’on avait retrouvé son portable entre les mains de vigiles aux Maristes et après plus rien.
Comment ces derniers ont eu le portable ?
Aucune enquête n’a été diligentée car la police connaît le coupable et n’a rien fait.
Dans ce pays il n’y a que la loi du plus fort qui marche.
On doit reprendre les enquêtes et soutenir l enfant qu elle a laissé
L'ex marie c'est un bon gars respectueux
Que le paradis soit sa demeure éternelle Dieynaba Traoré
C'est une négligence totale des parents qu'alla SWT L'ACCUEILLE à son paradis ÉTERNEL
C'est la vérité diamono.woroul.xol.jabotbi.bou.bah
Anta Diallo boul accusé famille bi sans raison yeen goor yi sen khaliss kheureum laniou ko ligueye boul Nian dall si niom kheureum yi louniou ladj fou niou diokh ko pour existe deretou faw nga teureul ou teud akh djiguern diou khess ect... donc khalle bi ay agissement won dou naturelle police akh gendarmerie louniou def dou yoon daniou wara aide famille bi def sen deuil wax leen li am au lieu di def de la cachoterie
J’ai suivi 7voix du coeur et je me suis dis qu’il y’avait trop de non dits en plus la dame ne laisser pas le gars s’exprimer elle lui coupait la parole par moment. Yalla na yalla feignal ki ko raay InchaAllah rabbi
Ay ki dewame messoul dègne Sama xol 😌😌bilahi damacoy xalate rek Yalla na Yalla lèrale yep inchala ☝️☝️
Que justice soit faite pour Dieynaba
Maintenant on est en juillet 2024 il faut que justice soit faite pour Djeneba d'après le discours de la famille elle sortait avec Un proche de l'état il faut réouvrir le dossier de cette fille tuée il y a plus de deux ans que justice soit faite j'ai vu sur tic toc "khelbou sell parlait du décès de Djeneba, et je le soutien vivement
Il faut faire des lives sur ça li warou niouko bayé nonou, ke coupable est en liberté
Entièrement d'accord
Lima meti à chaque fois je me disais kouko def lii kagne lay fégne une femme si belle gnou rayko comme ça
Ki def lii yalla nako borome bi nite😭😭
Amine yarabi
Allahouma Amine Y'a Rabbi 😔 🤲
Allahouma amine bilahi sa wakh rafétena. Au moins vous savez raison gardé .
Fegne na
Nkm dagneko soupçonner rekk mais batay arrêter wougnou ass boudé mom la nakkk yalla nagneko arrêter 3ans c'est trop
@@serignembackegueye3683
Je ne cesse jamais de penser à cette fille yallana ko yalla niit
C'est trop triste j'ai eue pitié de son fils les paroles de son ex mari ma fait pleurer yalna yalla nite ko si Barké Yonnentbi sallallahou alleyhi wa salam si Barké werou koor bii 😢😢😢 c'est triste vraiment
Que son âme repose en paix mais en général senegal lifi nek la kene doul wakh tu vois des frères irresponsables qui peuvent pas protéger leur sœur en leurs payant leur études leur besoin ,les parents aussi dangay ame sa dome bu jiguene mou ame far amoul liguey amoul dara dila gèrel sa courant dila diokh gay lek dila defal lep.gnuy lek avec la conscience tranquille. Prenons nos responsabilités et protégeons nos sœur en tant que frère et parents.
La famille a une grosse part de responsabilité dans cette affaire. Comment est ce qu'on peut laisser une femme aller en weekend avec une personne qui n'est pas son mari ou une personne de sa famille!
C'est grave et dans tout cela le nerf des maux c'est l'argent.
Si une personne fréquente une fille et qui n'est même pas capable d'entrer dans votre concession ou même de rencontrer des membres de la famille c'est une aberration.
Elle a juste été envoyer dans la gueule du loup.
Puisse son âme repose éternellement en paix et que ceux qui ont ôté celle belle âme à l'affection familiale puisse être trouvés et jugés ici et dans l'au-delà.
Et que cette triste histoire nous servent de leçon à toutes et à tous
Tu as tout dit
Je n’aime pas juger mais malheureusement deug nga wakh. Sa famille ne l’a vraiment pas protégée; de son vivant et même après sa mort! En plus je ne comprend pas vouloir cacher le nom du copin😢
Effectivement c sa ki me choc
bilay wahgua deugue
Bilaye wakh gua deugue wanté halisse louné meune nako c’est sur que halé bi done naléne diokh halisse mo takh parent yi wakhugnu dara
De plus en plus les parents montrent leur démission par rapport à l'éducation de leurs enfants. Cette fille qu'Allah ait pitié de son âme, elle est une des victimes de ces nantis qui pensent qu'avec leur argent ils peuvent tout se permettre. La famille de la victime,saisissez un bon avocat pour éclaircir cette affaire
Madame Gaye il faut voir nos entreprises ce sont des arènes de luttes pour occuper certains postes et obtenir des avantages les gens sont prêts à tout tu fais tout le boulot on nomme a des postes stratégiques des gens qui n'ont pas le niveau et ce sont ces derniers qui font ce genres de sacrifices faw nga rey faw nga teud akh djiguern diou kherer ou nioul liii ngakoy seuf foko wo mou wouyou la loko deflo mou def ko ay mbokom souba legui laniouye comprendre si tu n'as pas de la foi tu vas le faire la famille ne réalise qu'après les faits nian yalla mousseul la si pekhe nit kou boon akh djeuf diou boon et après c'est la corruption pour laver l'affront deuk bi metina ba khetou khaliss yitelouleen naniou fedj sen Sokhla au péril de la vie des gens
1)Respectez la mémoire de la défunte. Yalnako yalla yeureum 🤲🏽
2)Famille laxiste en tout point keneu waxatouko.
3)Sen meurtrier présumé xamnguene ko porter leneu plainte dieul leneu avocat allez jusqu’au bout nalene diaral lunekk tei nguene bayii laxisme bii.
4) Ex dieukeur djii dh machallah kou nitter laaa ndeysane.
Depuis son meurtre ndeysane je me demandais esk c élucidé?! Kou deff lii yalnako yalla weer sii koor gui!
Sa commentaire nitténa mashallah
Aminnnn ligua fi wakh yeup deugueula
A
Sénégal legui dafa beuri ay secte ak sacrifie meurtre bi meune nek affaire yoyou guayi legui dagnouy dokhane djiguene juste pour ça dagnoulene di toure khaliss bou beuri mbagnou diap confiance
Yalna yala yéssal yeurmandém ak ndiégualam thi mom thi barké wérou kor gui 🤲
En tout cas le conseil qu’on peut en tirer c’est de bien choisir la personne que l’on fréquente, surtout les filles. Certaines se basent juste sur les biens d’un homme et oublier le point le plus important qui est la beauté intérieure. Je m’en limite là, que Dieu l’accueille dans son paradis.
Donc les pires ennemis des filles sont les hommes ?
Yalnako yalla yereum té diégalko!!!! Mais khaliss dal dokhoul diam
Ndeysane tene dite dieynaba Traoré une fille très gentil machalah paix a son âme
Comment une fille non mariée peut passer un week-end avec un homme. Arrêtez vos sœurs à temps. Trop de liberté tue la liberté.
Sénégal kilifaa dafiii beurétoul...
Week-end ak goor bou nékoul saa dieukeur putin guén xamko bayiko mou dém... vous avez votre part de responsabilité sii doxaline bou yémé cii soxna dieyna. Sétane guén lolee
Vraiment
Vraiment
Vraiment vous êtes irresponsables
Bonne question ❓
Vous les sénégalais et sénégalaise yii bayilen jugez 😢 si je regarde certains commentaires je pleure même si la victime avait bcp de liberté elle ne mérite pas d’être tuer il faut que justice soit faîte c’est tout yalla nako yalla yeureum ki fatou🙏🏻🙏🏻
La famille a failli à sa mission responsable qu Allah l accueille à son paradis firdaws amine
Famarta niang faut pas accuser la famille beaucoup de millionnaires et milliardaires sénégalais ou des hommes qui occupent certaines postes le font au périls de leurs vies dans les entreprises il y'a de ces combats mystiques et des sacrifices a faire pour accéder à certains poste deretou ou fok nga rey ou teud akh djiguern djou khereer ou djigueen diou nioul kouk ect.. la fille peut être quelqu'une de très correcte irréprochable dans son comportement mais a cause des choses mystiques elle devient incontrolable jusqu'a son dernier souffle
@@sadiobandia947 donc c est triste qu Allah vieille sur nous amine
@@farmataniang5608 c'est allah qui peux te sauver mais aussi prendre ses dispositions mais aussi il faut te protéger il y'a des pratiques que nos grands parents faisaient pour protéger les femmes les enfants utiliser les plantes pour se prémunir de la mauvaise langue du mauvais oeil des pratiques mystiques et qui a tendance à disparaître je donne l'exemple de mon grand frere qui a investi dans l'agriculture son champ lui rapportait des millions chaque année mais il est resté 1 ans 6 mois sans mettre les pieds labas mais dès qu'il en a parlé a ma mère elle l'a mis en rapport avec des vieux qui lui ont donné des mesures de protection aujourd'hui il a repris les choses juste pour dire que la vie d'aujourd'hui kou sagane sa bop sa ndiabot niou rey la mame yi bayinaniou leup
@@sadiobandia947 yalla nako yalla yereum kharè Al djana Firdawsi🙏😭😭
@@mariyamadiop5768 ADIANA moy dalouwayoom kiko rey mo am problème moy yobale dieufom yeup
Yen tmt dh sagane nguen ndeysan
Mais que son âme repose en paix🙏😒😏
Que justice soit faite faut relancer l’affaire en 2024 nous réclamons justice pour Dieynaba
Djiguéne day guate tank tei yéme si lokho Kouy seye seyal tei yalla takhe djiguéne amoul dolé Yaye boye 😭😭😭😭 si képarou gorr rek moy wérou wayam Kouy seuy seuyal dei yalla takhe kouy djiankou khamal foye Téki sa tank
Vraiment la famille,vous avez trop laissé depuis le début.
Bilae
Mais tmt vous qui parlez d'irresponsabilité arrêter, cette fille n'est pas une gamine, elle a un enfant, kham na adouna sa famille n'a pas à prendre des décisions pour elle de plus qui vous dit que sa famille intervenir roule wone ci relation bi avec ce gars louche ? Elle a juste rencontré un de ces monstres 🤦🏾♀️
Yallah rek mo kham qu'Allah lui fasse miséricorde
Si la famille est irresponsable ndakh nan nguay bayé sa dom di ande gor bo khamni takouko di and ak mom week end 3jour te takouko dou yon bref yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana
Dieynaba Traoré paix à ton âme. Ton ex mari mom masha Allah. Yalah nga dieum guenal nala fingua diogué.
Que justice soit faite pour cette jeune fille. Je pense que son amant en sait quelque chose. Problème jalousie
Les mots du mari m’ont vraiment touché. Massa.Que son âme repose en paix!
Bilahi ex mari bi koubakh la nioune djiguene gni dagnouye ame kou bakh tes dougne ko khame niouye top khaliss beu lore souniou bop sou khamone mou dess ak borom kereum dji diamossi yalla yalnako yalla yereume diegueuko atéko si yeurmandéwome yalla méye lene kholou mouye
@@adjindiaye4459bilaye li leçon la nagnou kholate sougnou boppou bayi materialiste
Que le bon Dieu l’accueil dans son paradis le plus haut Inch’Allah et courage à toute la famille
Amine🙏🏾
Vraiment ex marié bi kou bakh na te am coleure khale you djiguen yi daniouy nek ak kou bakh kou Len beug yeureum Len niou ne ko fa niouk di weur brom tour ak brom alal motakh Lou nek laniouy dadiel yalla nako yalla yeureum waye leçon la pour yen djiguen man yalla mo def brom khalis bouma khamoul doumala gne
Yalla nako yalla kharé aldiana fidawsi si barke Serigne Touba 🤲
L'argent sacré pièce 😢
Paix à son âme 🤲 qu'elle repose en paix 🤲
Félicitations amy seck Ligueye bi rafetna torop vraiment
Tamouy Deug Masha Allah 🙏
Pape makha svp prend soin de ton fils
yal na ko yalla yereum wayé djiguène dou mome bopame ba foula nékh yénedou foula nékh fanane
Le prophète sws a dit si un de vos semblables meurt dites du bien de lui ou garder le silence . Qu’Allah Azawajel lui pardonne ses péchés et qu’il expose les responsables de cet acte ignoble nchaAllah qu’Allah nous pardonne nos péchés qu’Allah nous protége et protège nos familles et proches qu’Allah nous éloigne des gens néfastes au cœur de brutes nchaAllah qu’Allah fasse de nous des gens biens et qu’il nous accorde une bonne fin nchaAllah
Amine yarabil bien parler machalla
Commentaire yi khalatelene domam bi beuss bou magué baye lire message yi yallah nako yallah takhawou mayko kholou mougne
J 'ai pas l'habitude de juger les gens mais la famille a trop attendu pour sortir dans les media. La fille était trop indépendante, liberté bou Bari bakhoul. Massa à sa famille et yalna Souf sedd si kawam
Niémé wessouwoul di juger kou deudou juste sur de simple mot de personnes. Nga rouss YALLAH sakh té khamni YALLAH na yékh so deudo do beugue loudoul sédé you rafett dontè dinga fi bayi you safanou. Rew mi kéne khamatoul li sokhor la wala ignane
@@deuguerek4547 louma fi wah Lou Gnaw wala lou ayé , yaw môme seytané radjim nga, Nafék nga. Kouy weur satan ba eksi si yaw meun nga deup.
Waxoo daraa lou ayy... dieyna wakeureum biniou guicé wadji déff alale sii mome guén sétane moukoy yobb Founé... meussolén djém xam wadji ayy sii bountou keur layy taxaw cheuteuteu désolé mais kel manque de responsabilité. Xaliss doxoul diam.
C'était vôtre soeur kan mm
Alahouma amine 🙏
Bilahi sof rek wakhofi dara Lou graw Sénégal mo nakaré wakhé balamay dé rek niounane la dagua sokhor dagua iniane
C'est la responsabilité des parents nagni surveiller souniou rakk yi AK certains fréquentation
Ay L'argent toujours L'argent encore L'argent les femmes mefions nous des hommes riche mane dh dama len ragal 😢srx 😮😢
😮ôhhh?’N’déysââne!nako yaleu yéreum🙏🏻Kou rafète lawone!🇸🇳♥️😌!
C une trice histoire k dieu lui accueille dans son paradis et lui pardonne, wayénak la famille devait etre plus responsable en lui exiissant de se marier avec le gars comme çà elle sera légale avec lui
Vous avez négliger votre sœur avant sa mort, pendant sa mort et après sa mort
Je demande comment on peut être aussi naïf...
Quelle repose en paix
Ndeysane yalla naniou yalla bolé ak niit yi bakh
vous etes irresponsable amo leen loleen wakh depuis bobou leep beug lou yombou rekh la mais dieynaba yalnako yalla yeureum té khareko aldiana firdawsi takhawou domam
Il faut que ngen nanguou toudou tour. Ne serait ce que pour faire bouger les choses.
Communiquer. Yobou affair bi teuss ak khalass...
A la fin wadji waxnani ASS la toud
Sawaaay !!! Kham nguèn lanla....
Siggil lènko ndigalé.... 😢 Niou nianalko Yallah swt defalko soutoura adouna ak alaxira si barké Rassoulilahi SaW.
C'est perdu !
Nguéne Baalma Sénégal daffa doye waar
Imagine toi nga bayi sa Doome ak un gars boo xamni dou dieukeureum pendant 3jours en plus son frère waxnani moussoul guiss waadji
Vraiment la faute c’est la famille
Vous avez sacrifié votre fille
Yéne xaaliss rék nguène guissone ci mome
Vraiment c’est dommage
On à la même avie
Merci 😊
Moma diakhal
Kou seuye ba tasse am dome kene manouka teyer mome Kaye dafa tassel ah raykatou note wayer Yalla nako Yalla weer si Barker koor gui
@@fatoukine3415 mm bo tasser nga wara geuna am diom gooru leguiyi niom nieup yam presk
Ohhh je la connaissais mon omonyme kou yarou bakhone chaque jour je me demande le cas de Dieynaba foumou tollou
Famille bou neik dafa wara âme kou tangue Di redresse si deugu mais lii yeup début bila laisser aller bii mou diourlii lo djiii lolou ngay récolter famille bi neigliser d le début mais nak yalla nako yalla yeureum t kharerko aldjala
Il y a des gens c'est pas des humains mais en faite c'est des microbes, des virus, des ordures dont malheureusement on est obligé de vivre avec eux dans ce monde. Je prie vraiment que cet énergumène qui a ôté la vie à cette Dame puissent avant sa mort à lui aussi puissent répondre de son acte ignoble d'abord sur terre, que le Seigneur entend ma prière, et qu'il pardonne a la femme ses péchés et l'acceuille dans son paradis céleste.
Amennnnnn🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Amine Y'a Rabbi
Amin
Amine 🙏🙏
Ki dem dem na ba parei keine waroul wax si mome lou niaw yalla nako yalla yeureum m amoul kilifeu dh
Vraiment
Ya bakhe waye
Merci chérie les gens aiment trop juger teu nio gueuneu pire laissez la reposer en paix.
Bilahi amoul béna kilifa
Nite bouye nieuw bassa bountou keur di séte sa dome niouye ande di déme té diémoléne convoqué ko si bir keur gui wakhtane khame moye kanne vous les parents et grand frère déf guene erreur c'est pour cela douko respecté yal nako yalla yéreum té kharé ko al jennah kiko Ray yal nako yalla nite 14:05
La famille, la famille, la famille…. Trop de manquements c’est dommage quand elle était en vie on peut dire qu’elle est responsable de ses actes mais après sa mort fallait prendre vos responsabilités, suivre les choses, porter plainte et surveiller les actes posés côté justice, saisir les médias à temps mais là c’est trop tard je pense à moins que vous avez de la chance
En plus l’étranger là il faut dire son nom et publier sa photo si y’a des témoins ils pourront faire le lien. Pourquoi vous ne prononcez pas son nom? Vous avez peur de le dénoncer ou pas? C’est bizarre
Vraiment
@@naboujadieng627 ils ont dit le prénom du gars vers la fin du vidéo écouter bien , un certain ASS qui travaille au trésor public
Vraiment
En tou cas 🤷🏾♀️
ils ont dit il s’appelle dg souder mom la yalla nako yalla wer si barker werou koor
Massa . RIP. Ameen
Au Sénégal on cache trop les choses. Cet enfant l amener chez le psychologue pour enfant. Seul un professionnel du domaine mental peut mieux aider et guider cet enfant de 7 ans mentalement. Allah sameu ko . Courage à tte la famille et proches. Y allah Bakhna. Always
99% sure que le gars est le suspect numéro 1 (pour ne pas dire il est le meurtrier sans jugement) Raisons: 1)La fille s’est battue avec le meurtrier et le gar avait une égratignure(selon les témoignages) 2) le gar l’avait battue et menacée de mort 3) le gar a eu laudace de s’occuper de lautopsie sans se soucier de la famille(incroyable, seulement au Sénégal). Si c’était ici en Amerique l’enquête serait concentré sur lui, et la police n’aurait pas besoin d’entrendre 2 miles propriétaire du vehicle qui a transportè la fille cette nuit (il suffit de savoir si le gar possède cette voiture) . Les policiers sénégalais sont bien sûr très forts, Mais bien sûr avec ce ngour de Macky Sall les riches proches du pouvoir sont intouchables. Espoir que Sonko ou autre candidat bou yeguè les choses vont changer. Rest in peace Dieynaba!
Je suis du même avis que vous.
C'est son amant le présumé meurtrier, puisque c'est un proche du régime de Macky Salté moy lolou un Ass ?
Je partage ton avis
Bilay lou lére
Absolument raison
Merci lougnouye neub si tourou wadji la khamoule gni famille bou gnack fayda lagnou
Comment on peut laisser un membre de la famille avec son copin pour un week-end
Vraiment c'est du n'importe quoi
L'argent peut tout acheter sauf un être humain
Yalla nako yalla yeureum tè kharéko aldiana
C'est grave ce qu'il est en train de dire ... Quelqu'un qui vient chez moi devant ma porte pour ma fille ou ma sœur a plus reprises soi-disant son copain sans pour autant que j'intervienne, c'est irresponsable de votre part toute la famille nak . Je suis désolé nak
Mais kouko wakhoul nafekh nga. Lii Kay c'est du n'importe quoi. Sénégalais ak Khaliss.
@@coumbandiaye6923 vraiment en écoutant ce monsieur j'étais abasourdi
@@nikojonkins5721 Moi j'étais vraiment dépassée . Pourquoi les gens ne réfléchissent pas avant de faire des sorties de ce genre ?
Comment peut-on être aussi irresponsable à cause de l'argent ? Desgraciadamente !
@@coumbandiaye6923 vraiment je te dit en j'étais en train de faire du sport mais sama sport yeupa yakhou. Doyna waar trop
MERCI POUR VOTRE FRANCHISE. C ENERVANT EN FIN DE COMPTE
je suis très touché par son ex mari !
Yenlaye wakhal famille bi Nalene justice diapale thi. Wayame diodiou WA salam
Ndeyssan koo seuyeul gnou faat ko si anam bi.
Massa Serigne bi metina Dee yaa Gorée yaa baah
Je suis atterré par certains commentaires qui pointent du doigt une supposée responsabilité de la famille de Dieynaba Traore et qui de surcroît, font des allusions malsaines sur la "moralité " de la fille.
C'est ignoble et répugnant, un peu de décence et de retenue ne vous ferait pas de mal.
Je compatis à la douleur de sa famille et de ses proches.
En espérant de tout cœur que les enquêteurs feront le maximum pour mettre la main sur le présumé meurtrier.
C’est ce que je dis les gens n’ont pas le droit de blâmer sa famille ils vivent déjà avec la douleur de la perte de leur fille vos jugements ne leurs font pas du bien. Arrétez seul Dieu peut juger 😢
En tout cas mais la fille deysane je pense que sen wa keur on eu marre de la situation après niou tok dico setane mak bou teu bakhoul
@@mimie.a6424 doyna war lol sakh
Paix à son âme , mais d'après li wadji wakh la défunte dieynaba avait beaucoup de liberté
Pourquoi vous n'avez pas réagit à ce moment là,vous rapprocher de la justice
Vraiment elle était libre loutakhe moukaye yobou casamance sans mou tak ko yalnako yalla yereume
Vraiment sister
Billay dafa mélni damako xam sa mort ma fait trop mal d'autant plus que xamoniou koko ray que son âme repose en paix
Yalla naco yalla kharé aldiana Monk niam fa fék gnep 🙏🙏🙏
Franchement une famille très irresponsable comment laisser une fille aller en week-end avk un Homme qui n’est pas son Mari???? Quand ya l’argent c bon 😢
osons le dire, Cette famille a sa part de responsabilité dans cette affaire. Ses frères ont peur du gars, très peur même.
Mane dh bilayiiii magui commentaires le dimanche 21 Juliet à21h 19 munite 2024 batay meuma co faté tei khawmako sakhe mais dafma métiiiiiiii Yalla n’a Yalla yésal yeurmandé si mome barké serigne fallou mbacké
Donc va soutenir khelbou sel sur tik tok ndakh il lutte pour justice pour dieynaba
Nion yéme dei comme si que damako xaam😢
Nio yem dé mane je pense à son petit ami suis sur qu'il y est pour quelques chose nama yalla bal
Tako sama rak et même boko take boko doré ma tothie sa lou bone.
Bayiléne liberté bou eupe biguéne di diokh xallé djiguéne yi dakh copore nioune tamite djiguéne gni niou dall té régler Wa salam
❤❤❤❤1😊😊❤❤à
Yèen gni ay vrai irresponsable gueèn khana djiaguolèen tamite ba faram di djieul been😢 iniziative
Iow deuk bi libfi khew daniou si wara wakh nieup khamnaniou ni crime il faut police def ligeyam famille d'ora jot si corps bi
@@onlypandaintownyèen yi sokoy dègue sakh daguaye mère walay médecin yi rékk warougniouko woon wakh béen informations déjà pck c'est pas une menbre de la famille voilà
Ndeysanne je pense bcp à elle .Yalla na yalla léraleu lèpeu.je ne te juge pas ma sœur yalla na yalla kharéla aldiana firdawsi
L’enquête doit être relancée avec celui qui avait menacé de mort DIEYNABA …c’est fort possible qu’il soit l’auteur présumé du crime. Il faut pas avoir peur …il n’a que le BON DIEU sur terre et au delà!!!
A chaque fois damay poser ayy questions sur l’affaire de la fille !!ca me fait tellement mal meussoumako faté ndeysannn comme si dagno bokk dareu.yalla ngeu hippé aldiana Dieynaba
Amin Allahoum Amin
Nama yalla baal mais Sénégal beurina famille yo khamni na khalé bi di eundi khaliss rek ndeysaan 😮😢😢😢
Bilay dewou dieynaba bi nimouma metiwe yalla rek moko hamm😢
Je ne pas regarder jusqu'à la fin 😢😢 comment on laisse nos filles comme ça ? 😢
Paix à son âme yalla na yalla def Aldjiana firdawsi di kereum bou moudje
Si le copain est proche de l’Etat dossier bi khar léne Sonko yékk niou topou cas bi inchAllah
Mame Fatou maintenant on est le 24 juillet 2024 il faut que justice soit faite
@@soumboulousidibe7245moi je vais demander à Rox d'en parler vu qu'elle est suivi, niou dioublou watt ci
Rien ne justifie le fait de tuer une personne à part la légitime défense la famille a été trop négligente et votre réaction prouve que rien ne peut remplacer une mére un père.
Billay amoul remplacement
Moi à mon intuition, c'est son copain qui l'a éliminer peut être c'est dû au mariage où autres que le gars n'avait pas l'intention de l'épouser et puis une dispute à éclater, parceque comment il à pu prendre la responsabilité de gérer l'autopsie sans aviser la famille ??? Et disparaître après.
Vous avais laisser partir le meurtrier, regarder toutes les détails, et ces effets personnels rien a disparue, cela veut dire la personne qui l'a tuée voulais juste la supprimer et n'a rien pris sur elle, à part peut être jetter son téléphone
Déposer une plainte contre son copain qui à gérer l'autopsie et à disparu,
Le gars il était très jaloux t dieynaba dafmadone waxni copin bi dakoye doreuh rek mokodone fayal appartement bi diko defal lepp
Noumou toudou
@@MakeupArtisttv ils ont dit il s'appelle ASS il travaille au trésor public,il est marié à 2 femmes. Il faut nous siwolko , mo raye femme bi
Je suis de tout cœur avec toi
Ki esk sacrifier woukowo
Alors messieurs vous avez un piste il faut l'exploiter et vous trouverez la vérité
Maïs depuis le début donane suivre cas bi mais li famille expliqué taye mousougnouko expliqué au début comme danion ragalone wak mais yalla na ka yalla yeureum
Parent iresponsable la faibless de largest yalla nakko yalla yeereum 😢
Khana kouye dokhane di nha dougue si keur presenter ko famille
Sincèrement
Quel dommage ça ne vous dérange pas de dire que elle est allée passer un week-end avec un homme qui n'est pas son mari
En tout cas on'a une poliçe çientifique trops pertinent pour quoi on a Pas trouver le coupable j'usque a present ça me diakhal torop torop Torop sakh
Police scientifique qui s occupe de qui?
Yalla nako yalla xaré Aldiana firdawsii Barké AL XOURANE.
Mais comment pouvez vous laissé votre soeur votre fille allez en week-end avec un homme qui n'est pas son mari ahhh kel liberté kel famille???
Merci
C est l argent
Demandez a ses copines qui étaient avec Elle le soir au terroubi peut être elles savent avec qui elle avait rendez vous c genre de cas pierre Bellemare les enquêtes impossibles lassi wolou😢