Machallah watali guen si wer korgui sedal guen si sunu khôl yalla na niou sunu borom nagoul sunu kor niou téwé ko ay atti att barké seydina mouhamed psl té yeuramal niou sunu way dawlou firdawsi disen naflay 🤲🏿🙏🏿❤️🥰
Je me suis rempli d’émotion wollah j’ai kiffé la série je peux même dire c’est ma préférence je savais ça va clarté wollah mais ma plus grande surprise c’est doucoure son intégration à apporter bcps plus de créativité dans la série merci niankou ndayane baye guede sans oublier la fille j’aime les pikes qu’elle fait à niankou merci toute l’équipe
Bilahi content nagnou thi yen depuis 1 jour ba legui je n’est manqué aucune épisode di bahagnou niep akh yalna yalla nangou sougnou koor lignou thi moy yiep yala diegal gnouko yalla yagualen fi guen gnou begual yalla yokoulen baguen yeukko dewenaty bn fête merci a tout l’équipe
Delen commentaire si serie yi té bayi or sijé yi ay mey Len ma j'aime loleni gagner si ay j'aime yena wala mey serie bi kay ay j'aime yalla na diam yagu si Sénégal 💞
Taye ma fi djitou déwénatilén yalla nanou ko féké aye déwéne you barri bonne fête à toutes les musulmane ❤️🌙🤝
Amine ya rabi
Amine
Yalnaniouko fékké ay att you bari
@@antadianor7085 amine🤲
Doucourè todje n'a koor gui bilahi il est très fort...machalla belle équipe
sadio Mané futur ballon d'or européen inchallah
Doucoure l’artiste complet 😭😭😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
Baléne ma akkk balnaléne yalla naniou yalla ball si Barkiiii Seydina Mouhamed❤️🤲🤲🤲
Amine
Déwénati yalla nanko féké ay att you bari barckép s touba❤🙏🏿
Doucouré goudal fane 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 gayi dewenati cotane naniou lol bilahi yalla nalen yalla Faye machalah mais Awa linga pouss eupna 😅😅😅😅😅 dewenati gayii. ay way nayane ken dou yaw bilay walay 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣❤️❤️
Xol Sedna doucouré 🤣🤣 bonne fête à toutes l'équipes déwéneti 🙏🙏
DOUKOURE C UN DUR J LE KIFF
Nguir dieum Seydina Mohamed psl ak Serigne Babacar Sy abonnél Souleymane Jules Sy officiel à tout le monde tei Yalla takh ❤️🇸🇳🙏
Délo ma sama aboune
Boul forcer bayil leup nieuw naturel rekk c’est mieux bayil sarakhou bi bakhoul
Machallah vous nous avez beaucoup divertis merci niankou et à toute l'équipe dewenaty
th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQ/w-d-xo.html
J’aime bien
😂 Yadoo!! Sa dougoussi amatoul
Douk 😭 Nice ékip 🙌
Yado phénomène leu wallay😂😂😂😂
Wollae nio guena content ci yeen vraiment
Et surtout n’oublions jamais “Mbourou koor yii ” c’est très important 🙏❤️
Doukoure a beaucoup de talent
Bilay Wallay mangui nianal niankou boubakh ndakh nimoumay begelee
Bravo a tous plus précisément le duo doucou et guédé : le meilleur cett année 🔥🔥✌✌
Niankou le roi yalla nala yalla sam si baerki Naby ❤️🙏
Merci de nous avoir accompagné pendant tout le mois ramadan
Yalla na séne diamou yague ❤🤣
best serie koor doucouré vrai comedien la
Yalla na diamou yague sii Sénégal si barkip Seydina Mouhamed
Mane yadoo la beugue 😂❤️
Bilay yaw
Machallah watali guen si wer korgui sedal guen si sunu khôl yalla na niou sunu borom nagoul sunu kor niou téwé ko ay atti att barké seydina mouhamed psl té yeuramal niou sunu way dawlou firdawsi disen naflay 🤲🏿🙏🏿❤️🥰
Yalla naniou yalla may ak fékké déféwn 🤲
Vraiment bonne continuation vous étiez au top durant le mois
Bi mome dafa wara continue après koor kou d'accord 👍
niankou néna ndakh yeungeutouwoul 😂😂😂
Mercie l'équipe niankou le meilleur comédien de l'anneau
th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQ/w-d-xo.html
Machallah 29 yi yep mou nékh 👏👏👏👏
Tel père tel fils Guédé et Niankou 😂
Je me suis rempli d’émotion wollah j’ai kiffé la série je peux même dire c’est ma préférence je savais ça va clarté wollah mais ma plus grande surprise c’est doucoure son intégration à apporter bcps plus de créativité dans la série merci niankou ndayane baye guede sans oublier la fille j’aime les pikes qu’elle fait à niankou merci toute l’équipe
Vraiment mn mom yen rk lay sivor sama khol sedna machalla niankou et ndayan père doucoure baye Gede awa ba yado fara machalla filiation
en tout cas vous seriez me manquées 😘 machAllah c'était super et sympa vraiment. Bravo à toutes l'ékip 🙏🙏🙏🙏
Merci A vs contane naniou si yene begual guene niou si werrou korr gui nieupe yena baxe yena Goré diam si yene
No sacré doucoure🤣🤣🤣🤣🤣 artiste complet
Macha allah yalna seen Diam yagu yado amale diam
Mais vous êtes forts bravo doukouré
Mais doucouré meune n’a bongo dh 😂
Yalla nalen Sounou Borom may werr goudeul seni fane nguen doundeu ba doyal vraiment chapeau à vous begueul nguen niou respect à vous 🙏🙏🙏🙏
Machalla a toute l’equipe mais a beaucoup de talent ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQ/w-d-xo.html
Dewenati frère et sœur Balma akh balnala yallah niou yallah bolé bale niou fékké ko ayy atti att
Amine way🤲
Bonne continuation à toute l'équipe.
Masallah sédall guène soni khoul loole yàllàna yàllà samolène défallène diamou yokou sèn weurseuk thi lépou loguène begue amiine
Awa ♥️♥️🌠🌠🥰🥰 yalla nala guissate deweune Mane yaw la beug ❤️❤️💓💓💯🌺💯
Doucoure soumay mariage yaw laye wo😂😂😂😂😂
Ndeyesane niankou yalna sa diam yague nioun nieup contane nanou
Dewenaty bal leen gnou ak borom bii nagou sougnou koor
Dewenaty a tous bonne fête de Korité yalna yalla nangoul niou souniou koor.yalna niou ko téwé wat déwéne ay at you beurri.
😭
Amine
Merci à toute l’équipe 🙏🏽
Vous nous avez vraiment régaler de très bons moments 🙂
Awa da meun 🤣🤣 mais kenne dou doucoure 🤣🤣
Doukourè tu es le meilleur
Merci a toute l'équipe vous étes les meilleurs merci mention spéciale à niankou je l'adore
Yalnaniou féké watt ay déwen inchalla 🙏déwénéti contane nane si yénn déwenati 🙏
Néxna ll niankou bly niankou contane naci ioe bly😅✨🥰🙏
Wouyyyyyyy sama,ndeye niankou dina ma raay
Woyeeeee tantaye niankou😂😂😂😂😂I'm dead y'all 😂😂😂
Machalla yalna séne diam yague❤jamais beaucoup barki serigne touba
Amouniou sén fayy un grand merci à toute l'équipe 🔥🔥🔥❤️❤️❤️
Waw daguenn waraa continué way ❤️❤️🙏vs êtes les meilleurs ❤️🙏
Merci à tout l'équipe de nous avoir accompagné durant toute le mois de ramadan bonne fête 🥳 yalnagnouko féké déwen you bari ont vous j'aime 😘🥰❤
Niankou est le meilleur on est contant de vous
Niankou le roi yalla sam si baerki Naby ❤❤
Mani Doucouré mii dou ap art martial, rire merci 🙏 😊 👍
Niğou niģ kontan nae thie yénn yallah nane ko déwéne inchalla
Merci pour tout vous avez suscité en nous le goût du rire au moment où nous l'avons le plus besoin.
J'ai suivi tous les épisodes magui niane yalla may you féké déween inchallah thi barkeep weer wou tédebi😍😍😍
Vraiment ont na même op les mots rafetlou nagne liguey biu bou bakh diléneuh ñianal ñiou fékéko aŸ ati at si barké seydina Mouhamed ❤️🤌🏽
Yalla nalene yalla faye vraiment kene meroul
doucourè mii amna tallen dè macha allah
Yalla naniou Yalla maye goudou fane ak wére niou fékéwat ko déwéne inchallah
Hooooo ma challa nous sommes très fière de vous vous qui nous sommes rendus heures durant le mois de ramadan yall na nguéne ame diame 🙏🙏😅🥰♥️
blh je vous adore Yalla nalenn Yalla fay senn xoll❤
KHILASSU ZAHAB BIY DAW SI SOUF MASHAALLAH 😍😍😍
Vraiment ba dewen AK diam team niankou vous êtes meilleur
Merci à vous de nous avoir fait plaisir durant tout le mois😇✋
Merci de nous avoir regaler durant tout le mois de remadan yalla nasen diam yague😂🇸🇳❤️
Doucouré l homme fort
Niankou tu es le meilleur ❤️
Doucouré merci beaucoup walahi je l'aime 😔😔😔😔😔
En tout cas merci Encore Niankou yafii neik💪💪😄
Ndaw louma guedja dégu😂🤣🤸thiaxx sa guou-guounn😂🤸🤸 bilahi niolénn gueuna contane 👏👏🔥 déwénatilénn ❤️ yalnaniou feque déwenn you barii ❤️ amine ❤️
Macha allah yalla na seen diaam yaag vs avez trs bien assuré sur tte la lignée ❤️
MAN DAMA BEUGUE MOU CONTINUE 😹BOUMOU YEM FIII REKK
AKK YENEN EPISOTE
Son bi di daw si souff mach'allah way Abdou Aziz Mbaye❤❤❤
yalla nagnou ko feke aye ate you Bari aminenn
Timbakh doukouré😂😂
Ohh khar nalene b sonou diam thi yene feke dewene kene bania manke inchala ☝️❤️
Doucouré Dou nitou fii mingui Lenn koy wax RK😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Déwénati 🤲🙏 bonne fête à toutes les musulmans 💚💚
th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQh/w-d-xo.htmlttps://th-cam.com/video/OAPOmw9F4PQ/w-d-xo.html
Bilahi content nagnou thi yen depuis 1 jour ba legui je n’est manqué aucune épisode di bahagnou niep akh yalna yalla nangou sougnou koor lignou thi moy yiep yala diegal gnouko yalla yagualen fi guen gnou begual yalla yokoulen baguen yeukko dewenaty bn fête merci a tout l’équipe
Niangou meilleur de sa génération
Yalla na yalla nagou sounou koor👏
Wa kou guiss féthieu yado yi🥰🥰🥰😂
Yado dinama manqué nak 🤣🤣🤣😭
Machala déwénati gnoléne gueneu contane
Delen commentaire si serie yi té bayi or sijé yi ay mey Len ma j'aime loleni gagner si ay j'aime yena wala mey serie bi kay ay j'aime yalla na diam yagu si Sénégal 💞
Chapeau a toi Doukouré
Waaa yaaaado miii rabeina trop 😂😂😂😂
1er vui bi manla yup😇
No yéne amguén tenla bilahi diam si yéne niou fékké att you Bari 👏👏👏👏