BAYE ASSANE NAGNOU GUÉNÉ LISTE MBACKE MBACKE YIY...LE FATWA DE SERIGNE MOUNTAKHA AUX BAYE FALL...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 4 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 334

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 วันที่ผ่านมา +20

    ❤ serigne mountakha mbacke yalla naffi yague tee weure❤

  • @dieganesene9357
    @dieganesene9357 วันที่ผ่านมา +22

    Serigne mountakha yalna yag té weur.Té diadieufal Baye fall yi ndigeul dieufé rék .Ndigalou YALLA moy ndiagalou Borom touba té moy ndigalou Serigne mountakha .Lou bakhoul dou bakh mouk té lou bonn dou bakh mouk . Touba deuk la bouñouy diamo suñu borom la.

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

      Mountakha motoule kilifeu diangoule diongoule moussoule djité diaka 😢

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 วันที่ผ่านมา +23

    Waw gooooooor Assan yalla nala yalla Dolly Ay ndimbul yaw Mourid Nga

  • @franceamericanbullydogfami7992
    @franceamericanbullydogfami7992 15 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Yague loool té andak weur Mbacke balla ❤❤❤ sunu mbekté ❤❤❤

  • @mohamedkaneleigh1326
    @mohamedkaneleigh1326 วันที่ผ่านมา +61

    Lii Serigne Bii beuGg Moy Am TOUBA par force ! ☝🏽 kouMou neikh Ak kouMou nakharii !!

    • @Haafiz90
      @Haafiz90 วันที่ผ่านมา

      Leufeul ndayou Serigne bi doul way

    • @elhadjicheikhba4122
      @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +1

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @elhadjicheikhba4122
      @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +1

      Diereudieuf way Boul tontou domou bireul yi ak domou Ndialo yi tékiwouniou dara Si Adouna ak Alahira 💯✍️🤫

    • @BayesaliouGueye-nc6wo
      @BayesaliouGueye-nc6wo วันที่ผ่านมา +1

      Boul tontou ken diadieuf😂😂محمد رسول الله من كان يومن بالله واليوم الاخر فليفلة خيرا اوليصمت جرجقت الشيخ أحمد بامب خادم رسول

  • @abdolfataniang5398
    @abdolfataniang5398 วันที่ผ่านมา +24

    Wallaahi s mountakh moy kilifa 😢😢😢wakh bi dafa yaatou lambo na lepp Wallaahi 😢😢s mountakh mbacke yalna fi yagg lool te wer b s touba ❤❤❤❤❤❤

  • @Serignemboussobebousso3136
    @Serignemboussobebousso3136 วันที่ผ่านมา +6

    *Assan nak Yaay Meilleure. Chroniqueur.*

  • @MameSydyBirahimThiam221
    @MameSydyBirahimThiam221 วันที่ผ่านมา +6

    Jërëjëfëty linga wakh lérr na amna sollo jaajëff
    S Mountakha Mbacke yalna fi yagu té and ak wérr Baye fall itt yalna lén sunu brom may ak katan té museul lén si pékhé non yi bagnu gënë mana liguéyal Serigne bi amine yarabi

  • @fantastique1731
    @fantastique1731 วันที่ผ่านมา +19

    Sa ndiogou yalnala yallah may goudou fane ak weur

  • @OmarFaye-ez3ig
    @OmarFaye-ez3ig 14 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Macha allah diaradieuf mbacke yageu di té weur ❤

  • @elhadjicheikhba4122
    @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +13

    Diereudieuf Serigne bi ❤❤❤❤❤

  • @NicolasNiasse-p1n
    @NicolasNiasse-p1n วันที่ผ่านมา +3

    Merçi solution

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 วันที่ผ่านมา +6

    ❤sa ndiogou cerveau ❤

  • @elhadjicheikhba4122
    @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +13

    Merci Assane ♥️✌️❤️

  • @dembathiao8232
    @dembathiao8232 วันที่ผ่านมา +3

    Lo beugeu mbacké mo am Touba inchallah ❤❤❤

  • @khadimdiop6578
    @khadimdiop6578 วันที่ผ่านมา +2

    ❤❤❤ merci baye assane bék na thi yaw

  • @elhadjicheikhba4122
    @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +10

    Diereudieuf Serigne mountaga diereudieuf Ousmane Sonko ❤❤❤

  • @FallMandiaye
    @FallMandiaye วันที่ผ่านมา +5

    Merci Assane et solutions

  • @DTFTV
    @DTFTV วันที่ผ่านมา +3

    Chez la Baye Fall Kay : MDR 😁🤣🤪

  • @ablayesene9804
    @ablayesene9804 วันที่ผ่านมา +11

    Touba dey deukou Serigne bi limou fa beug rk mofana am koum nekhul nak nga toukhou dem fénen addina bi yatou na dh ken momul Touba koudul Brom Touba dieredieufeti Mbacké yagal weral si barkep khassidayi ✅

  • @bayejobe4204
    @bayejobe4204 วันที่ผ่านมา +7

    Baye fal❤❤❤👍👍❤️🤝🤝🤝❤️❤️❤️🤝

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 วันที่ผ่านมา +9

    Machalla mais aý xalè yondaw aý nitt nèkk sèn guinaaw xeex safinatol amaan xeex police nara xèx baye fall yi doyombu incha allha thiaaxaan katt touba daý xatt si moom

  • @boubacarfall6777
    @boubacarfall6777 วันที่ผ่านมา +18

    Li serigne bi beug moy am❤❤touba deuk bou. Sel la nguir yalla nagn ko wormal nguir dieumi yalla ❤gnou rouss si serigne Mountagha khadim rassoul❤

    • @thiammady4782
      @thiammady4782 วันที่ผ่านมา

      Khanaa wormay deukk bi dioulli bookkouci.

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      ​@@thiammady4782kholal noko dégué rek

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      Serigne bi da yab Talibè yii rèk mais kilifa yifaye dèf loulèn nèkh beurina koumasèko si baye fall yii

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

      Mais eske mountakha mongui ormal Y'ALLAH sounou Borom ak YONENBI SAWS momemi néna Alakhira daye rombou Y'ALLAH SHWT ak YONENBI SAWS déme si serigne touba lolou nékoye expliqué 😢

  • @OmarFaye-ez3ig
    @OmarFaye-ez3ig 14 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Merci assane yaw mouride nga Macha allah

  • @ousmanendao2033
    @ousmanendao2033 วันที่ผ่านมา +1

    Serigne mountakha yalnaga yagg ak werr

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 วันที่ผ่านมา +3

    صفات صادق المريد الصدق في محبة الشيخ امتثال الأوامر ترك الإعتراض سلب الإختيار .المريد الصادق يكون كالميت بين يدي غا سله.

    • @BenmouhamedDiagana-w1g
      @BenmouhamedDiagana-w1g วันที่ผ่านมา +1

      الكتاب و السنة هما مرجعا و مصدرا المسلمين
      فهل لك دليل من القرآن و السنة

    • @MbayeThiam-x5j
      @MbayeThiam-x5j 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      أحسنت أحسن الله إليك

    • @HUSNULMAAP6327
      @HUSNULMAAP6327 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      ​@@BenmouhamedDiagana-w1g
      اطيعو الله ورسوله واولي الامر منكم

  • @ndiayeleroi3417
    @ndiayeleroi3417 วันที่ผ่านมา +1

    Machalla Assane

  • @KhadimGueye-eo1zy
    @KhadimGueye-eo1zy 22 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Baye fall yi ak askan touba yi dinañu khekh

  • @raulmarceldepoter7170
    @raulmarceldepoter7170 วันที่ผ่านมา +4

    Tant que l'interdiction s'applique seulement sur les talibés vulnérables, ça sera toujours deux poids deux mesures mais beaucoup de mbacké mbacké ne respectent pas les recommandations donc ils doivent donner la paix aux autres sinon ça devient de l'injustice totale

    • @LahatCisse-n5g
      @LahatCisse-n5g วันที่ผ่านมา +1

      Lou môme sen affer la mé nioune môme ly Serigne bi beugue rk lanou beugue

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      @@raulmarceldepoter7170 Serigne bi nièmèwoul Mbackè Mbacke yii motah talibè ordinaire yii laniu yabe rèk

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

      ​@@LahatCisse-n5g eske mountakha mongui défe lou Y'ALLAH sounou Borom ak YONENBI SAWS bougou 😢

  • @assanegueye1352
    @assanegueye1352 วันที่ผ่านมา +18

    Bounou faté diouli yalla moko sanetané tadounouko déf niaka diouli amoul laye

    • @babacarlo8076
      @babacarlo8076 วันที่ผ่านมา

      Lolou sa yone Nékou si

    • @ablayesene9804
      @ablayesene9804 วันที่ผ่านมา +2

      Lolou nitte kila concerné djioulil rk té bayi len ken kouné lingay def c’est nitte kila concerné ms Touba mom Serigne bi moy brom nekul titre foncée wou ken ✅

    • @ridialdieng2861
      @ridialdieng2861 วันที่ผ่านมา +2

      Sa way djoulile sa djouli rek yalla dou djiayalé dieufou kén ak moromame wala

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      Nga def ko té noppi

    • @abdouantagaye680
      @abdouantagaye680 วันที่ผ่านมา

      Baye fall =yéfeur

  • @moustaphambaye5289
    @moustaphambaye5289 วันที่ผ่านมา +9

    Walay assane deug dou rombi noop😂

  • @elhadjicheikhba4122
    @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +10

    Topou Nigal Bayi térré. Final

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      Touba dè gnifay dèf loulèn nèkh dou khathi

    • @elhadjicheikhba4122
      @elhadjicheikhba4122 วันที่ผ่านมา +1

      @CheikhOumarFaye-if1eo Baye fall yi dinanko Lidianti

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      @@elhadjicheikhba4122 bane lidieunti lolou daniusè meun dara Serigne bi si bobam sakh nièmèwoulèn toudou ganane

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

      Mais eske mountakha mongui topou ndigueulou Y'ALLAH sounou Borom ak YONENBI SAWS

    • @elhadjicheikhba4122
      @elhadjicheikhba4122 23 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

      @@CheikhOumarFaye-if1eo Manousi démal touba xol bakham limouy tére amna fofou

  • @salioundiaye7594
    @salioundiaye7594 วันที่ผ่านมา

    Gracias

  • @babasamb4019
    @babasamb4019 วันที่ผ่านมา +9

    Meune louma meunoule comprendre mooy gané Serigne Touba moye sa royoukaye té do diouli

    • @alieunjie1940
      @alieunjie1940 วันที่ผ่านมา +2

      Mou diakhal nio bouri

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      Dinala la yaga diakhal

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      ​@@alieunjie1940yaw ak kane

    • @FallMandiaye
      @FallMandiaye วันที่ผ่านมา +1

      Bo ladie gni xam dinala dimali gni xam lala wax nak

    • @MoustaphaFall-v5f
      @MoustaphaFall-v5f วันที่ผ่านมา +1

      Yaw féxél bassa diouli bakh mon geune nitt daye ma ndou diarama cheikh ibrahima fall

  • @ChiekhKhouma-q5d
    @ChiekhKhouma-q5d วันที่ผ่านมา +2

    Merci bay hasan❤🎉

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 วันที่ผ่านมา +1

    ❤ assane massare ❤

  • @issasene2880
    @issasene2880 วันที่ผ่านมา

    Serigne mountakha mbacké yalla nalla fi yalla yakal lolll té and ak wér

  • @ibradieng4537
    @ibradieng4537 วันที่ผ่านมา +1

    Dieureudieuf serigne bi.nous exécuteront à la lettre vos ordres quelque soit le prix à payer.

  • @OusseynouNiane-np5rz
    @OusseynouNiane-np5rz วันที่ผ่านมา +3

    Assane mon anti stress il a été métrisé le sujet 😅

  • @BabacarNDIAYE-pr3zn
    @BabacarNDIAYE-pr3zn วันที่ผ่านมา +5

    Assann wayy ❤❤❤❤le meilleur chroniqueur ❤❤❤❤❤

  • @mamethiernodiop3748
    @mamethiernodiop3748 วันที่ผ่านมา +18

    Li serignbi begeu par la force day am

    • @taliberassoul
      @taliberassoul วันที่ผ่านมา +1

      Mo taxitt gni amna niokoy violé santa mbacké
      Xam ngani dangay fen kon

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      ​@@taliberassoulWakhi dof

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      Talibè guèn yab rèk mais pa niu sante Mbackè mbackè yii

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

      Mountakha vrai domou kharame leu leupeume fitnaleu Wallahi ki soumouko diapé na raye ndayame en plus amoule khame khame 😢

    • @bayemorsarr1754
      @bayemorsarr1754 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      ​​@@brigadeantibidah2911Arabie Saoudiya lafa khew de dou massa khew Touba woo ay woykat niolende woyal ba pare tek Kaaba gué diko wuer 🕋🕋waxal si lolo 😂😂😂😂anti bidah NAAR BI ⚽ mom 1xbut FOMO dekue 😂

  • @AhmaGueye-t8y
    @AhmaGueye-t8y วันที่ผ่านมา +1

    Asan waw gor❤❤❤

  • @Serignemboussobebousso3136
    @Serignemboussobebousso3136 วันที่ผ่านมา +1

    *Cëy Sëriñ Bi aka xam Jamono*

  • @IbrahimaNDIAYE-v5d
    @IbrahimaNDIAYE-v5d วันที่ผ่านมา +2

    Ma chah allah assane khoromouna, très intelligent

  • @NicolasNiasse-p1n
    @NicolasNiasse-p1n วันที่ผ่านมา

    Merçi assane billahi téw mome sa day khar happy si yaw

  • @sonhiboufall4485
    @sonhiboufall4485 วันที่ผ่านมา +4

    Assane monekh c la.bay fall😂

  • @loudoulaktalibesafouma3429
    @loudoulaktalibesafouma3429 วันที่ผ่านมา +1

    Li serigne beug fawou mou am❤❤

  • @gorafall3709
    @gorafall3709 3 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Sa la baye fall

  • @AwaDiop-d2d
    @AwaDiop-d2d วันที่ผ่านมา

    Bilahi ❤❤❤❤

  • @wademor7905
    @wademor7905 วันที่ผ่านมา +1

    Merci Hassan

  • @muktarmuktar611
    @muktarmuktar611 วันที่ผ่านมา

    Wakh léne deug té yalla rek takh...baye fall yagui tek nite yi fitte na

  • @HUSNULMAAP6327
    @HUSNULMAAP6327 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Merci Assan yaw nit ku dëggu ga

  • @MbayeThiam-x5j
    @MbayeThiam-x5j 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Sa Touba La Assan Diaradiaf

  • @cheikhndiaye9919
    @cheikhndiaye9919 วันที่ผ่านมา

    Bilay assan wakhna dege🤚 mbacke mbacke yi danio am seni baye fall

  • @abdoulahadengom1078
    @abdoulahadengom1078 วันที่ผ่านมา

    Antouka li Serigne bi wakh lerr nagne ❤

  • @aronakamara5159
    @aronakamara5159 วันที่ผ่านมา

    Akassa diadieuf mbacke touba keur serigne bila lo borom keur ngui beugu mo faye am kouko meunoul nga tokhou

  • @SerignefallouSarr-s7x
    @SerignefallouSarr-s7x วันที่ผ่านมา +1

    Touba ❤❤❤❤❤❤

  • @thiernoba-wc2ti
    @thiernoba-wc2ti วันที่ผ่านมา

    Baye asane😂😂😂😂😂😂❤

  • @Babacarcisse1004
    @Babacarcisse1004 วันที่ผ่านมา

    Merci Assane 🥰🥰🥰

  • @SaloumSylla-yh3ip
    @SaloumSylla-yh3ip วันที่ผ่านมา

    وسلم ❤❤❤❤❤❤❤ ماشاء الله سيد محمد ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ingcoingco3926
    @ingcoingco3926 วันที่ผ่านมา +1

    Dieu a créé l'homme libre mais l'homme veut toujours soumettre par la force ses semblables. Et si y a un camp ici et un camp là-bas, qu'est-ce que ça va emmener ? Tout le monde sait se battre, tout le monde peut créer une unité de défense, mais ça nous mènera où ? Moi je crois en ça, par la force toi tu vas y croire. Tout ce que je demande à Dieu c'est vraiment d'apporter la paix dans les cœurs. Forcer une personne à faire ce que toi tu désires, ne fait pas de cette une sainte car tu peux contrôler le corps c'est à dire la physique du corps mais pas l'âme. Parce que la personne peut t'insulter, peut avoir des idées ignobles et le vit dans son coeur, son âme et là c'est plus dangereux même.

  • @IssaKasse-s1j
    @IssaKasse-s1j วันที่ผ่านมา +1

    Secte yi Nio yak ndey Sénégal serigne mountakha tiaxan rk

    • @BayesaliouGueye-nc6wo
      @BayesaliouGueye-nc6wo วันที่ผ่านมา

      😅😅😅😅😅yw dafa melni sa khol nekhol de 😅😅😅ay way من فعل ما شاء لغي مت شاء

  • @issasene2880
    @issasene2880 วันที่ผ่านมา

    Pourtant serigne bi limou beugue rek la yalla digu lé

  • @boubacarfall6777
    @boubacarfall6777 วันที่ผ่านมา +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Pour solution

  • @BayeFall-lf2eo
    @BayeFall-lf2eo วันที่ผ่านมา

    Assane baye fall la❤❤❤❤

  • @MorFall-xj6fb
    @MorFall-xj6fb วันที่ผ่านมา

    Ab Baye fall ga yaw baye assane wakhal

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo9727 วันที่ผ่านมา +1

    Shouhaybou liii dou fo bayyill kafgie

  • @BallaNiang-r5y
    @BallaNiang-r5y วันที่ผ่านมา

    Li sérigne bi beugue moye am piont❤

  • @MarémeLô-q9n
    @MarémeLô-q9n วันที่ผ่านมา +1

    Baye assane dou nitou fi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣♥️❣️♥️❣️❣️♥️

  • @omarsal763
    @omarsal763 วันที่ผ่านมา +2

    Machalah baye asane

  • @yacinesene219
    @yacinesene219 วันที่ผ่านมา +3

    Touba titre foncier la Serigne Touba Moko mome li Serigne bi beugue moye ame

    • @CheikhOumarFaye-if1eo
      @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

      Serigne bi dè dè na bou yague adouna bi dè amatoufi dara

  • @serignecheikhkhadimfall6654
    @serignecheikhkhadimfall6654 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Sa Ndiogou Bayil khél Né Serignbi Déefuku Toumal Carter yi Luo Amla
    Assane Dall Limuwakh Werne

  • @mamethiernodiop3748
    @mamethiernodiop3748 วันที่ผ่านมา +4

    ❤❤❤

  • @SerigneCheikhdiop-z3n
    @SerigneCheikhdiop-z3n วันที่ผ่านมา

    😅Non assane sérieux wul c'est la baye fall😂😂😂

  • @RohayaFalle
    @RohayaFalle วันที่ผ่านมา

    Assane rek lay deguelou mane il est fort

  • @elimanesylltoubalarocette2464
    @elimanesylltoubalarocette2464 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Assane degue rék nga wakh

  • @mohamedmbengue7065
    @mohamedmbengue7065 วันที่ผ่านมา

    nooon Assane Amoul 🤦‍♂️😂🤣🤣

  • @gueyemamecheikh6440
    @gueyemamecheikh6440 วันที่ผ่านมา +2

    Asane amna solo ❤

  • @IbrahimaKa-eg4ff
    @IbrahimaKa-eg4ff วันที่ผ่านมา +8

    Serigne bi warna digal bay fall yi gnou dioulli

    • @BintouSaw
      @BintouSaw วันที่ผ่านมา +1

      Serigne warna yaw yaw yako sania wax

    • @Organization221
      @Organization221 วันที่ผ่านมา

      Sen keur mba niongui diouli

    • @MbackéfMbackéf
      @MbackéfMbackéf วันที่ผ่านมา

      Lou si sa yone yow kaye dioulil rek

    • @FallMandiaye
      @FallMandiaye วันที่ผ่านมา

      Bo xomoul te ladjo dangay nopi

    • @BayesaliouGueye-nc6wo
      @BayesaliouGueye-nc6wo วันที่ผ่านมา

      Diomay warna wax police yi et soldat yi et gendarmerie nioy dioulli ndakh senegal soldat yi barina nio doul diolli te dolenko lidianti te amna sakh nion kham ni don ay diollit te bolen tegouwoul ci yon par force nio teg len çi yon

  • @CheikhOumarFaye-if1eo
    @CheikhOumarFaye-if1eo วันที่ผ่านมา

    Serigne bi dall da am gnimou yabe rèk mais Touba gnoufay wowè kilifa tèy dèf loulèn nèkh dou khathi dou dièkh

  • @MrAkhmadou
    @MrAkhmadou วันที่ผ่านมา

    Assane est très intelligent

  • @MatySall-ep4ow
    @MatySall-ep4ow วันที่ผ่านมา

    Merci beaucoup asane

  • @abdoucisse6605
    @abdoucisse6605 วันที่ผ่านมา

    Saysay ci nek touba di roube khame leen sen boupo baye fall yagi niew de nay leer

  • @saerseck3638
    @saerseck3638 วันที่ผ่านมา

    Kou sante mback boul dour me kou santoul mback dorall 😂 Senegal mo nekh 😢

  • @Veridic-tv
    @Veridic-tv 19 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Lay donc assane n'est pas fou xam na où chercher les polémiques quand c'est mountakha loum wakh deug leu ? 😢😂

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 วันที่ผ่านมา

    Mais eske mountakha si bopame mongui topou ndigueulou Y'ALLAH sounou Borom ak YONENBI SAWS.

  • @laminefall6481
    @laminefall6481 วันที่ผ่านมา

    banioume baye fall moye ndigueul diougué bire keur serigne touba❤ ta adio diodiou fadiou woul kone bok sama mbokou Talibé yi liguéy ba gui nn

  • @boguadiop3637
    @boguadiop3637 วันที่ผ่านมา

    Ja jeuf s Assane ❤

  • @sidytop15
    @sidytop15 วันที่ผ่านมา +2

    Merci assane talibé bou nek war na woutou Serigne bi fam nék djefé ndigal bayi téré

  • @abdoulayediop9231
    @abdoulayediop9231 วันที่ผ่านมา +5

    Man déh bi serigne Mountakha takhawé né bou yalla takhawé yonénti bi psl takhaw mou bayi lén fa djoublou serigne touba lako simil chapeau kii yalla toppé wouko dara 😂😂😂😂

    • @BintouSaw
      @BintouSaw วันที่ผ่านมา +2

      Amo dégue degue motakh Diahil limuy wax xélekoy xam

    • @MoustaphaMbathie-mm1rp
      @MoustaphaMbathie-mm1rp วันที่ผ่านมา

      Ioe mbam nga mo tax dou xam Lou sérigne bi beugue wax

    • @abdoulahaddiop5621
      @abdoulahaddiop5621 วันที่ผ่านมา +1

      Yaw mouso diap seringe bi bakoy bayyi nafex bakhoul

    • @abdoulayediop9231
      @abdoulayediop9231 วันที่ผ่านมา

      @@BintouSaw koon serigne bi djahil la yaw linga wakh yéména déh 🤣🤣🤣

    • @abdoulayediop9231
      @abdoulayediop9231 วันที่ผ่านมา

      @@abdoulahaddiop5621 yalla mo gnou gueuna xam lii nék ci xol yii

  • @diallodiallo4459
    @diallodiallo4459 วันที่ผ่านมา

    Fatawa kay thi ay bayfall . Serigne pas yalla

  • @64FallAmadou
    @64FallAmadou วันที่ผ่านมา +1

    Sénégal neikhna 😂😂😂

  • @diopmusa8658
    @diopmusa8658 วันที่ผ่านมา

    Assane vérité absolue

  • @nardiop1401
    @nardiop1401 วันที่ผ่านมา

    Cela bay fall😂😂😂❤❤❤

  • @AsSaalih310
    @AsSaalih310 วันที่ผ่านมา

    Asane mana communique mais dafa bari caxaan 😂

  • @ahmethannediop3669
    @ahmethannediop3669 18 นาทีที่ผ่านมา

    Civil manoul réglé moromoume civilame Serigne bi khamoul dara alkhourane ak sounna rék mo woor

  • @salioumbackeba9595
    @salioumbackeba9595 วันที่ผ่านมา

    Bolene amone diome lou Serigne Mountakha wax Waw Guene di wax wala mandou. Limi wax guénoul béne yone diner

  • @papecisse2703
    @papecisse2703 วันที่ผ่านมา

    Touba dou Reew ,ville com Dakar ou une autre ville ds ce pays,boul niou fontoo

  • @idrissseck6891
    @idrissseck6891 วันที่ผ่านมา

    C'est la baye fall dé lérna

  • @SakhoKhadim-r9x
    @SakhoKhadim-r9x วันที่ผ่านมา

    Senegal dou rew