⛔️S.Moustapha Amine à Pr Bassirou diomaye limou def si ziar bi.. El Malick.. Cheikh T Dieye

แชร์
ฝัง

ความคิดเห็น • 203

  • @dameseck6232
    @dameseck6232 หลายเดือนก่อน +4

    Dieredieff sy malick yala na yala mayela goude fane ak weurr amine ya rabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @djibrilba2582
    @djibrilba2582 หลายเดือนก่อน +2

    Dieureudieuf serigne moustapha al amine sa wakh raffetena

  • @souleymanesadio-yy9vv
    @souleymanesadio-yy9vv หลายเดือนก่อน +38

    C’est une leçon Leçon de vie, bayi hébaté. Té bayi di togne koula defoul dara. Ame tahawayou kilifa

  • @Ciara66129
    @Ciara66129 หลายเดือนก่อน +8

    Ana gueum door , khol door 😂😂😂😂😂 thiey yallah souniou borome moy karim,

  • @cheikhsarr7855
    @cheikhsarr7855 หลายเดือนก่อน +11

    Dieu est très grand

    • @nafitoure546
      @nafitoure546 หลายเดือนก่อน +1

      Dieu est très fort mougn dingua moussa mougne wornama né diotaye bi nioum bari nip rouss

  • @ZikrZikr-gh8zk
    @ZikrZikr-gh8zk หลายเดือนก่อน +26

    Bilaye yalla meune dé 😅😂😅 thiey sougnou Premier Ministre bi

  • @laminelo5183
    @laminelo5183 หลายเดือนก่อน +18

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
    Adouna deh yala ko mome

  • @SidyBa-pm4zn
    @SidyBa-pm4zn หลายเดือนก่อน

    Sonko ❤️ moye Diomaye ♥️ masha Allah ❤️♥️❤️❤️♥️

  • @abouhafsaat-tidiany2160
    @abouhafsaat-tidiany2160 หลายเดือนก่อน +9

    Man mom Ben philosophie la am mooy kepou kouma khass tay souba dingma tagg machallah

  • @gtksen
    @gtksen หลายเดือนก่อน +8

    Serigne Moustapha nous sommes tous très très très bien fiers de vous
    Masha Allahou Yalna yalla arela teh dioh wer ak Diame

  • @baradieng8093
    @baradieng8093 หลายเดือนก่อน +4

    Machalla dieura dieuf Yalla diam yague inchalla

  • @ndeyetoutygueye1681
    @ndeyetoutygueye1681 หลายเดือนก่อน +10

    Nonnn, je rêve ou quoi? Diomi amoul heure ndekete

    • @adamasene9821
      @adamasene9821 หลายเดือนก่อน

      😂😂😂😂😂

  • @anandajrfall6396
    @anandajrfall6396 หลายเดือนก่อน +10

    Ousmane Sonko seutou mame Rawane NGOM LA MAME KHALIFA ABABACAR SY DOU SEDALAI DIKO FATAI WALAYE NDAYSANE❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏💯

    • @53bocar
      @53bocar หลายเดือนก่อน

      Kilifeu d’où am fettai, nous les Tidianes kham nagnou Maodou, yar rek’

    • @53bocar
      @53bocar หลายเดือนก่อน +1

      Sénégal yeup mbokou la , c’est une petite nation

    • @oumousarr6691
      @oumousarr6691 หลายเดือนก่อน

      Setou mame rawane war n'a kame takha wayame bou bakh

    • @anandajrfall6396
      @anandajrfall6396 หลายเดือนก่อน

      @@oumousarr6691 khame ko mo takhe mou dathe limou dathe guir rewame

  • @badafall7179
    @badafall7179 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah Serigne Moustapha Al amine tivouane gno goreh rek koulene defal loubakh gno wakh KO teranga teranga rek mokoy fay président Diomay da gneuw fonk sounou kilifa Serigne Babacar Sy Mansour ndiabote gui yepou fonk KO mou diekh

  • @kevin-zf2cn
    @kevin-zf2cn หลายเดือนก่อน +9

    Thiey yalla mo meune atté d

  • @ekacamara9104
    @ekacamara9104 หลายเดือนก่อน +30

    li dafa gnaw louway diwax warnga sor eleuk surtout koxamne défoule dara sonko yalnafi yague te wer

    • @abibmarouane6699
      @abibmarouane6699 หลายเดือนก่อน

      Wallahi iow ya bakh

    • @badafall7179
      @badafall7179 หลายเดือนก่อน

      Kou am gnari diabar aussi foy dem waar ngako khôl surtout député am indemnité de santé pour se soigner au kinésithérapie professionnel

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 หลายเดือนก่อน

      Lan mofi ngiaw sonko lan lanko déf daw dangioo takhaw sant Macky si tahawayam ngén mérr ngioun tivavon souniou kilifayii lanou am kéupp koulen fonkou niou fonkoula AK koo mana doon nioun kounou défal niou santala président basirou diomaye Faye yalla nako yalla diappalé yalla woyofal yén bi loumou beugg ligey si Sénégal yalla nako yombou bou dée loumouy wouti bala moo diouk diko wouti yalla nako loolou féksi

    • @oumousarr6691
      @oumousarr6691 หลายเดือนก่อน

      Kou defoul dara kéne dou la wakh dara sonko khame n'a

  • @anandajrfall6396
    @anandajrfall6396 หลายเดือนก่อน +4

    Walahil azeem Biss bi betou khamone Nani yague yague thiataye bi Dina ame ndakhe DOGUALE bie mo djitou sounouke nek si kawe soufe inshala LISSI KANAME moye GUEUNA tawefekhe ake TAYSIRE inshala🙏🙏🙏💯❤️👈

  • @mboupngouda165
    @mboupngouda165 หลายเดือนก่อน +4

    Macha allah sy malick ❤

  • @anandajrfall6396
    @anandajrfall6396 หลายเดือนก่อน +5

    Khame wakhine encors amena importance si TARIKHA bi.......

  • @hfhgg-bm2to
    @hfhgg-bm2to หลายเดือนก่อน +7

    Nanioulene nianal rek president Bassirou Diomay faye ak Ousmane sonko

  • @ousmanembengue1119
    @ousmanembengue1119 หลายเดือนก่อน +5

    Thiey yallah mon aye si potoubour fi yallah rëk fi nëk nëk di toumal nitt kouka si bayiwoul

  • @mamourfall8934
    @mamourfall8934 หลายเดือนก่อน +2

    Thiey légui mom dignité amatoul fène serigne bi passé yadone saga sonko et son parti rène nga lène di tague Diarama Serigne Moustapha "Le PERMENANT"

  • @seydinayoussouphandiaye8708
    @seydinayoussouphandiaye8708 หลายเดือนก่อน

    Merci diomaye

  • @kebecheikhtidiane7494
    @kebecheikhtidiane7494 หลายเดือนก่อน

    Dieureu dieuf sy Malick

  • @mbordiop1359
    @mbordiop1359 หลายเดือนก่อน +1

    إن الذين يبايعونك إنما يبايعون الله يد الله فوق أيديهم فمن نكث فإنما ينكث على نفسه ومن أوفى بما عاهد عليه الله فسنؤتيه أجرا عظيما // الواو في من أوفى / والفاء في سنؤتيه diangal nga bagne begue tari

  • @oliviervaz4658
    @oliviervaz4658 หลายเดือนก่อน +6

    Wakhdji rafetna yalla nanou yalla defal diam

  • @izidineizidine6480
    @izidineizidine6480 หลายเดือนก่อน +1

    Allahouma Amine.

  • @mansourseck5725
    @mansourseck5725 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla amna solo

  • @diopassane-tu6yu
    @diopassane-tu6yu หลายเดือนก่อน +5

    sonko yarna rewmi

    • @user-xe5cz6ub5s
      @user-xe5cz6ub5s หลายเดือนก่อน

      Billahil Azim yarna rewmi kay 😂😂😂

  • @sultantv.chaine-des-sages
    @sultantv.chaine-des-sages หลายเดือนก่อน +1

    Amo diom sakh

  • @mbenguepapamakhtar5293
    @mbenguepapamakhtar5293 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla

  • @ndiayefatou565
    @ndiayefatou565 หลายเดือนก่อน

    Diomaye Moy Sonko ❤❤❤❤❤❤❤❤!

  • @cheikhgaye6367
    @cheikhgaye6367 หลายเดือนก่อน +3

    diaroul wakh dara bayi lènko nonou Yalla may nanou ndam si kawam

  • @omarpouye1493
    @omarpouye1493 หลายเดือนก่อน +1

    Machalakh Sy

  • @hfhgg-bm2to
    @hfhgg-bm2to หลายเดือนก่อน +1

    AlIahou amine

  • @nafitoure546
    @nafitoure546 หลายเดือนก่อน +2

    Gueum door (serigne Mansour Sy diamil

    • @user-xe5cz6ub5s
      @user-xe5cz6ub5s หลายเดือนก่อน +1

      Wa mais ki anamou sakh 😂😂😂😂

    • @nafitoure546
      @nafitoure546 หลายเดือนก่อน

      @@user-xe5cz6ub5s gninko wane mou tokk Di werekhle

  • @cheikhndaw2259
    @cheikhndaw2259 หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤

  • @julssouleyndiaye954
    @julssouleyndiaye954 หลายเดือนก่อน

    Machalla sy nioune yaw rek laniouy topou

  • @badafall7179
    @badafall7179 หลายเดือนก่อน

    Machallah Serigne Moustapha al amine kou wormal fonk respecté sa kilifa ak wa tivouane rek gnou fonk la deh ak koumou mana done.president mo kham worma tivouane ak plasou Khalifabi Serigne Babacar Sy Mansour gnoune gnepou gnou respecté rek .le respect est réciproque.Mane bokouma pastef mais kou respecté sama Serigne ma fonk la respecté la wormal dieureudieuf Serigne Moustapha al amine comme sa papa al nimouko wakhone Abdoulaye Wade kou fonk tivouane respecté sounou kilifa à lepoque Serigne Mansour Borom daradji gnou fonk la respecté.Talibeh day am fayda ak foula kou respecté sa serigne respecté ko koula falewoul al amine ak seriigne Babacar nena wakh koni yawmal khiyam sa ngone yallah bougnou guisseh bakham🦻

  • @senegalais9976
    @senegalais9976 หลายเดือนก่อน +15

    Le ridicule ne tue plus dans ce pays thimmmmmm

    • @AbdoulahadMbacke-xz6qw
      @AbdoulahadMbacke-xz6qw หลายเดือนก่อน +1

      Franchement ! Mane dama rousse sakh kholal ki rék lou Niaw louné wakh nakofi wa pastef louné fékhé nako pour khékh Sonko ! Légui diglou léne nimouye wakhé ! 😂 genre yi nio takh niouye wakh niti tarikha yi lou nék ! Séne intérêt rék tadou niou Séddeu euleuk.

    • @badafall7179
      @badafall7179 หลายเดือนก่อน

      Tu as raison si un homme et un député en période de couvre feu il brave l'interdit de sortir,marié laisse ses deux belles femmes et ses gardien et son chauffeur,part se masser devant une Femme qui n'est ni sa propre femme ni un professionnel de kinésithérapie ,pour toi c'est normal? tivouane n'a appelé personne pour venir gnom gno dem ba khamni tivouane koukosi bolewoul d'où dokh gnou gneuw respecté sounou kilifa gnou respecté lene rek,Ani gnodane saka Serigne si ak FMi ak banque mondiale gno dem andak Macky Sall New York pour lebi khaliss.nopil bo khamoul

  • @Fallyaram320
    @Fallyaram320 หลายเดือนก่อน +2

    Bilay walay yalla rèka meune koudoule khalate souba 😂😂

  • @user-pp2vl5yi1x
    @user-pp2vl5yi1x หลายเดือนก่อน +1

    😢ceye yalla mo mande

  • @tamsiretoure9644
    @tamsiretoure9644 หลายเดือนก่อน +2

    thieye adoune😂😂

  • @user-sz7zp5vz4q
    @user-sz7zp5vz4q หลายเดือนก่อน

    Ndaye sane ki modone wakh dou waak weyeleur yalla samou sonko

  • @barham4735
    @barham4735 หลายเดือนก่อน

    Ki d'où l'auteur de la frasque " vulgaire violeur"

  • @user-nn3dv5cp3q
    @user-nn3dv5cp3q หลายเดือนก่อน +8

    Sim nii douniou rouss sakh billahi

  • @oumarsarr214
    @oumarsarr214 หลายเดือนก่อน

    Gathié d'où rayé bilahi

  • @diankadiani4572
    @diankadiani4572 หลายเดือนก่อน

    Yalla dou nite

  • @bassfaye1730
    @bassfaye1730 หลายเดือนก่อน +1

    Nioun nak dinaniou andak yarr ak téguinn ndakh lolou la PRÉSIDENT DIOMAYE WONÉ .

  • @taphisco2012
    @taphisco2012 หลายเดือนก่อน

    Wa ana borom Amadou ba futur président 😂😂😂

  • @user-px5kf9ip8d
    @user-px5kf9ip8d หลายเดือนก่อน +3

    Serigne moustapha yalla na Yalla yagual sa takha way

  • @user-iw1bn3vu8b
    @user-iw1bn3vu8b หลายเดือนก่อน

    Bilay yalla moy buur

  • @tallat_s_chtv1232
    @tallat_s_chtv1232 หลายเดือนก่อน +3

    Thiéy adouna 😂😂😂😂

  • @user-nn3dv5cp3q
    @user-nn3dv5cp3q หลายเดือนก่อน +10

    Khanatay ngay dooga kham liguén book Sim dou guén rouss sakh

    • @dameseck6232
      @dameseck6232 หลายเดือนก่อน

      أعوذ بالله من الشيطان الرجيم ياسلام وياسلام في شنغال امين يارب العالمين

    • @tivaonemomelabeug5510
      @tivaonemomelabeug5510 หลายเดือนก่อน

      Domorame sa wokh yi nak

  • @aidandiaye8507
    @aidandiaye8507 หลายเดือนก่อน

    Han!

  • @elimanehann5286
    @elimanehann5286 หลายเดือนก่อน +1

    Yala mane afer

  • @diopassane-tu6yu
    @diopassane-tu6yu หลายเดือนก่อน +1

    khna taye

  • @PapeTall-ky2pp
    @PapeTall-ky2pp หลายเดือนก่อน +1

    Thieyy yalla

  • @michelndiaye9241
    @michelndiaye9241 หลายเดือนก่อน

    Thiey yalla souniou borome mo monne dé

  • @user-xh9zx1mu5m
    @user-xh9zx1mu5m หลายเดือนก่อน +2

    Khaliss rek

  • @user-xh9zx1mu5m
    @user-xh9zx1mu5m หลายเดือนก่อน +2

    Gisga discour bi nimou changer

    • @papisb9560
      @papisb9560 หลายเดือนก่อน

      😂😂😂 gni kaye moye lolou, wayé fi kéne meuna toufi nakh kene

  • @diopamine9339
    @diopamine9339 หลายเดือนก่อน +8

    Mon Dieu merci .. legui wakhi dèmbe ak wakhi tay daniouye woutè

    • @mouhamaddiagne6196
      @mouhamaddiagne6196 หลายเดือนก่อน +3

      Rawatina kougniouye wowe ab SERIGNE

  • @AmadouMbaye-jo6hr
    @AmadouMbaye-jo6hr หลายเดือนก่อน +1

    Thiey yalla deug rek mo wor ki yawla

  • @user-gs5ep4cc7s
    @user-gs5ep4cc7s หลายเดือนก่อน

    Hahahah noooo sonko dou nit

  • @assanekane8539
    @assanekane8539 หลายเดือนก่อน

    Guathié rek lay wakhé

  • @abdousall8712
    @abdousall8712 หลายเดือนก่อน

    Diomi amoul heure.

  • @mustaff3413
    @mustaff3413 หลายเดือนก่อน

    Thieye sopikou amna 😂😂😂 aka gaaw😂

  • @macoumbadiop3896
    @macoumbadiop3896 หลายเดือนก่อน +1

    😂😂😂😂😂🎉

  • @bouryfall1472
    @bouryfall1472 หลายเดือนก่อน +1

    😂😂😂🤭🤭

  • @cheikhsadiboumane1420
    @cheikhsadiboumane1420 หลายเดือนก่อน

    بالأمس وصفتموهم بانهم مغتصبون واليوم تمدحونهم. ماهذا التناقض

  • @aliounealassanesy2871
    @aliounealassanesy2871 หลายเดือนก่อน

    Dou ki mofi done saga Sonko?

  • @mamadoundaye9797
    @mamadoundaye9797 หลายเดือนก่อน +2

    yalla bour

  • @hadjimalickwade1706
    @hadjimalickwade1706 หลายเดือนก่อน

    Khamna bene affaire dé moy ki di wakh nii dara fessoul beuteum

  • @Del2Mas
    @Del2Mas หลายเดือนก่อน

    Yow dagua niak Fayda
    Ministre bi Ousmane Sonko la toudou defoula dara niak Diom

  • @user-pv8pw2zu7y
    @user-pv8pw2zu7y หลายเดือนก่อน

    Motakh halisse djaroul yene yii kilifa day kilifa tee bagne hebate

  • @user-rg1jl1gp3z
    @user-rg1jl1gp3z หลายเดือนก่อน

    Kii amoul sakh kham kham kii mo don wakh sonko viyoleur

  • @ibasarr577
    @ibasarr577 หลายเดือนก่อน

    Yalla na diamou yague kadou yi rafet na

  • @adamasene9821
    @adamasene9821 หลายเดือนก่อน

    Nn yalla dou nit😂😂😂😂😂

  • @user-io3lo7qy3f
    @user-io3lo7qy3f หลายเดือนก่อน

    Thiey yalla

  • @unsenegalnouveau2742
    @unsenegalnouveau2742 หลายเดือนก่อน +2

    Kii modone Traité SONKO de Vulgaire Voyou khawma Vulgaire Violeur 😂 Thièy Yalla sunu borom

  • @ndiayefatou565
    @ndiayefatou565 หลายเดือนก่อน

    Lingaye wakh gueumo si dara!

  • @user-pz1bz8sr7f
    @user-pz1bz8sr7f หลายเดือนก่อน

    No wadji mobile don wa wirger wiyoler no yalla nanu yalla mey dioup ak dioubal ak dioubanti

  • @user-nq4nt4ss4c
    @user-nq4nt4ss4c หลายเดือนก่อน

    😂😂😂😂😂

  • @mouhamedfaye8615
    @mouhamedfaye8615 หลายเดือนก่อน

    Serigne bou ñak goré paré nak diom si ki lako guissé

  • @senegalais9976
    @senegalais9976 หลายเดือนก่อน +24

    Bou gathié done Ray Kone do takhaw fi yeuppp thimmm do rousse amo diom amo gathié Mane ngua doule domeram

    • @bassfaye1730
      @bassfaye1730 หลายเดือนก่อน +1

      Boy yaroul nak. DIOMAYE Moy président té yarr ak yarou la woné. Naniouko ci Roy nak. Conseil d'un patriote

    • @aliounebadarandiaye5344
      @aliounebadarandiaye5344 หลายเดือนก่อน +2

      @@bassfaye1730 REW REW MO KOY FAYE CONSEIL D'UN TALIBE OUI ON N'EST PAS BETE

    • @bassfaye1730
      @bassfaye1730 หลายเดือนก่อน +1

      @@aliounebadarandiaye5344 boy nak réwandé amoul ndiarigne. Té nak mbam boula wéké nga wékk ko mbam nga comme mom. Réwandé nak djaroul djay mboubou bouniouy soll la rék. Fi nieup réw. Dafa diné amoul ndiarigne. Yow nak si con yi nék biir PASTEF nga bokk. Projet bi sokhlawoulén. So kholé démarche DIOMAYE ak SONKO baniou djeulé ngour bi balégui nguén wara nék ndéy niit

    • @aliounebadarandiaye5344
      @aliounebadarandiaye5344 หลายเดือนก่อน

      @@bassfaye1730 way go shit yak say lecons on recolte ce que l'on sème

  • @fallmoustapha1606
    @fallmoustapha1606 หลายเดือนก่อน

    Kiii d'où sakh niiit

  • @tassegueye8996
    @tassegueye8996 หลายเดือนก่อน +3

    N'est ce pas c'est lui qui traitait Sonko de vulgaire violeur

    • @user-xh9zx1mu5m
      @user-xh9zx1mu5m หลายเดือนก่อน +1

      Moma

    • @oumysane4665
      @oumysane4665 หลายเดือนก่อน +1

      Oui c'est la même p😅😅

    • @Ciara66129
      @Ciara66129 หลายเดือนก่อน

      Oui c'est lui même

  • @SodaFall-lv1no
    @SodaFall-lv1no หลายเดือนก่อน

    Thim😂😂😂😂 niak diome

  • @mouhamaddiagne6196
    @mouhamaddiagne6196 หลายเดือนก่อน +6

    Billahi kouye wout ab Serigne war ngako tane ndakh ki Khass yimou Khass fii gnii sim

  • @khoumasavoir9498
    @khoumasavoir9498 หลายเดือนก่อน

    Thiaye adouana mo doye war yawe yafi nekone dilene khass gouddi ak beuthieuk sa waxdji ba legui fatté wounou ko geummo darra billaye billaye gninga togal sax danga lene yéme

  • @serignemoustaphadiouf3430
    @serignemoustaphadiouf3430 หลายเดือนก่อน

    Lou sotti ame borome 😂😂

  • @seckbara2488
    @seckbara2488 หลายเดือนก่อน +1

    Thiye yala mouse bourr

  • @user-ee5cy6ei4l
    @user-ee5cy6ei4l หลายเดือนก่อน

    Ya niak djom liga fi wakh lepp thiboou niaw thi pros ak pastef

  • @Princesseboye8352
    @Princesseboye8352 หลายเดือนก่อน

    Ki dou touss sakh

  • @amilenardiop641
    @amilenardiop641 หลายเดือนก่อน

    N'est ce pas c'est lui qui disait ousmane sonko un vulgaire violeur Il n'y a que Dieu que décide alkhamdoulilah

  • @mouhamadougaye6687
    @mouhamadougaye6687 หลายเดือนก่อน +1

    Thiay yallla

  • @mouhamedniang666
    @mouhamedniang666 หลายเดือนก่อน +1

    Khana ki dou mom key

  • @zanzibarzanzibar8003
    @zanzibarzanzibar8003 หลายเดือนก่อน

    Sénégalais, ouvrez vos yeux. Ces soient disant marabouts ne sont que des charlatans doorkat😃😃😃

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 หลายเดือนก่อน

    Yahwou mom degou wo

  • @idythiandoum5902
    @idythiandoum5902 หลายเดือนก่อน +1

    Dieuredieuf sy malick