⛔️Gamou Soxna Oumou : Bougnou nakanté mais And bi desna si keur gui...Soun nekon ben heur bi Diouma

แชร์
ฝัง

ความคิดเห็น • 210

  • @bathiediagne2045
    @bathiediagne2045 หลายเดือนก่อน +37

    Diarama à Serigne Moustapha sy Almaktoum

  • @ousseynousene7713
    @ousseynousene7713 หลายเดือนก่อน +101

    Serigne Cheikh Tidiane Sy Al Maktoum je ne peux pas comprendre ngani moy sa kilifa té Serigne Moustapha Sy Al Maktoum liguéyal Serigne cheikh lepp té amo lén reconnaissance si mom bénén bisi wallahi Bou kén guiss taxawayam si Khadra Mame Babacar Sy Mame Maodo wallahi yalla guiss nako,DMWM bou yap yeup méloni ni réss kone paka dousi am yone,boy yédd nitt na fékk sa diouko soutt bosam sur tous les plans bouniou ken sonal tapha al Amine na xamni Serigne Moustapha Sy Al Maktoum liguey na demb bala tay té kou yar sa diouni morom war nga xamni dousa morom nila yeuf yi tolou . Diarrama Serigne Moustapha Sy Al Maktoum responsable du DMWM sunu Gorgui Sa liguey ak responsabilité kou sokhoroul war naleu wax Diarrama.

    • @idrissademe1931
      @idrissademe1931 หลายเดือนก่อน +4

      macha Allah @ousseynousene7713 vous avez tout à fait raison. il ne peut y avoir mille vérité
      DIARAMA CHEIKH SAÏD MOUHAMADOUL MOUSTAPHA SY

    • @khalioudrame9526
      @khalioudrame9526 หลายเดือนก่อน +4

      Yow topal feulé pape cissé mo gueuneu djigué almaktoum mo ko yar ki mo deukone ak mom fann beumou gueneu adineu. Qui diarbatam leu, moustapha sy nak dagno ko tague beu moudié ko kharap..gneupeu leu amal problème ay rakam aki magam.gneup dagnou ko bayi même khalifa mbaye dem na yonam...manipulation rek lay def.

    • @alindao6836
      @alindao6836 หลายเดือนก่อน +1

      Merci beaucoup tu as tout dit ❤❤❤

    • @mamadoulaminediop7145
      @mamadoulaminediop7145 หลายเดือนก่อน

      😊

    • @badadieye8506
      @badadieye8506 หลายเดือนก่อน

      ​@@khalioudrame9526founiouko tagué ay yonn dé laniou fékké mais Massounio guiss founiouko kharabé ak kouko kharap kanla ak fan lako kharabé boudé limouy wakh si dîné dji si tarikha bi si keur loumou si wakh defko si Serigne cheikh ak Mame Khalifa déff naniouko té nioniou la donou bokk si thiowli Di mbar mbari nak kham li khéw moko gueun

  • @mouhamadousall322
    @mouhamadousall322 หลายเดือนก่อน +19

    Diarama serigne moustapha sy al maktoum yaye sagou tarikhabi❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abibsamb4462
    @abibsamb4462 หลายเดือนก่อน +12

    Diarrama Serigne Moustaphal Mactoum déf gua sa wareef....Mame Mactoum neenako '' Sagal ngama Yalna Yalla Sagal la,,,ça veut tout dire Diarrama Serigne Moustaphal Mactoum 🟢

  • @MORTALLAKEBE-yj3wf
    @MORTALLAKEBE-yj3wf หลายเดือนก่อน +45

    Serigne moustapha sy ALMAKTOUM yalla na yalla goudal fanam té samm ko té arrko sa liguiéy sa takhaway gneup guiss nagn ko yalla na yalla fayal gnouko

  • @OmarSene-ng8eu
    @OmarSene-ng8eu หลายเดือนก่อน +4

    Diarama Serigne Moustapha sy al MAKTOUM ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @madristaforlife9601
    @madristaforlife9601 หลายเดือนก่อน +36

    Nangoul lén serigne Moustapha Sy maktum rek niou avancé 😌 limou ligueyeul maamam amoul kouko liguey niou wakhanté deugg 😌

    • @mamediop8845
      @mamediop8845 หลายเดือนก่อน

      Niou nangoulanté rk li maodo liguéye yeup nguéne ni kéne rk mofa bakh mofa Raw wakhi doff

    • @niangniang1518
      @niangniang1518 หลายเดือนก่อน

      ​@@mamediop8845 Entoucas limou ligueyeul maodo bir Senegal kou sante sy défouko

  • @medounediene9652
    @medounediene9652 หลายเดือนก่อน +9

    Wallahi deug rék mom ngua wakh yalla nalene yalla samou dioubolelene amine ya rabii ya allah

  • @fatimadiop8383
    @fatimadiop8383 หลายเดือนก่อน +2

    Machallah diokhlène borome thierbi thieuram moye seringe moustapha almaktoum yalla na Yalla motali te faylène yiw

    • @AJDKTVdeKambel5744
      @AJDKTVdeKambel5744 หลายเดือนก่อน

      Sering bi bufeke ni li yàlla may Tivaoune ben Thier kese la ta si sa seriñ rk la nk yen yi ngen geum ni ba kañ

  • @niangniang1518
    @niangniang1518 หลายเดือนก่อน +1

    Tivaoune bén serigne la ame mouy SMSY almaktom lol la yalla dogal eup lénn xam xam eup lénnn wilaaya eup mboloo❤

  • @morfall1978
    @morfall1978 หลายเดือนก่อน +4

    Serigne moustapha sy al macktoum rek

  • @IbrahimaGueye-vu9lq
    @IbrahimaGueye-vu9lq หลายเดือนก่อน +2

    S.Moustapha bou al amine mo yakh li warone rafet😔

  • @amifall1894
    @amifall1894 หลายเดือนก่อน +2

    Diarama seyidi mouhamadou moustapha sy al maktoum yalla na yalla motallie yeup inchallahe si barke mame babacar sy barke mame chiekh a tidiane sy al maktoum ❤❤❤❤

  • @elhmalickdiop374
    @elhmalickdiop374 หลายเดือนก่อน +4

    nagou lén ko liko yalla may nopalou serigne chieckh nagoul nako lep doga dém yén guén lank ko tou cour

  • @PapaNdiaye-ox2xv
    @PapaNdiaye-ox2xv หลายเดือนก่อน +10

    Yalla n'a yalla tapé khôl yeup

  • @user-yc1fb8mg8n
    @user-yc1fb8mg8n หลายเดือนก่อน +8

    ❤Machallah sama serigne merci machallah ❤

  • @dmwmdaaraymourchid4121
    @dmwmdaaraymourchid4121 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah Serigne Moustapha Sy Al makhtoum ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Diarama ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ yalna yalla moteli yéne kilifa si barké Serigne Babacar Sy ❤❤❤❤❤❤

  • @pendagamouniang3497
    @pendagamouniang3497 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah sy malick serigne moustapha sy al maktoum yalna yallah goudal say fane te samal gnou lah sagal gassa mame sagal gassa paay yalna yallah fayla❤❤❤

  • @assanekanezoucash4687
    @assanekanezoucash4687 หลายเดือนก่อน +5

    Yalla gui guiss leep bou défaar diooté naniou défaar rek, talibé tmt na khamné talibé la té yam si placou talibé. wakh dji beurrina thiow li beurrina waayé yakhoul liguéyou Mama ass dé yakhou itam liguéyou Cheikhal Khalifa. Li koussi meunoul wakh lou rafet mandou si guirr yalla wara soulli, kholeen ni kou gueen fi attaqué seutou mbaye la, kou gueen fi attaqué seutou Maodo la konne naniou woormaal kilifeu yi, té Mame Maodo mégnoul garab gou woyoff dé yalna yalla deff diam si euttou Mame Babacar, yalna yalla deff diam si euttou Mame Maodo, yalna yalla deff diam si Tivaoune, yalna yalla deff diam si Sénégal ya barakatou rassouloulahi

  • @linegueye6211
    @linegueye6211 หลายเดือนก่อน +9

    Machala wakh dji rafete na

  • @saerseck9491
    @saerseck9491 หลายเดือนก่อน +23

    Serigne Moustapha Sy maktoum likowar si dinedji ak tarikhabi defnasi waram na gnisidess roy simom sinon dougnou dem...

    • @moussangom3840
      @moussangom3840 หลายเดือนก่อน

      Niom aussi lilen War ci dinné ji ak tarikha bi niongui ci kan mo saga bâyi diambour yi beug niou dioh la ther manoul nek Mostafa saga n'a makk niep rawatina Al amine

  • @drameelhadjalioufatou7287
    @drameelhadjalioufatou7287 หลายเดือนก่อน +13

    act sénégal li louthi foto Moustapha Almaktoum di wout aye na fekheu ngene on sa fou

  • @taphagakou7968
    @taphagakou7968 หลายเดือนก่อน +7

    Senegal mon beurri nafékh ak saïtané gnii bougoul guénn nek bénn nion beurri mais bagn lénn ko entan que musulman unions fai la force

  • @abdoulayepene5766
    @abdoulayepene5766 หลายเดือนก่อน +3

    Machalla sy

  • @serignefalloumbacke7849
    @serignefalloumbacke7849 หลายเดือนก่อน +46

    Yene daleu amone nguen chance pour niépou nék beneu Moustapha sy al amine yakk lepou ndakh fiir yakarni bou Moustapha maktom nieuwé tivaouane niom niou fay

    • @MameSow-vp7rj
      @MameSow-vp7rj หลายเดือนก่อน +1

      Tapha Al Amine daray lérr nékoul si mom jé katou prono rk lamay nirole😂😂😂

    • @oumoukhalifandoye
      @oumoukhalifandoye หลายเดือนก่อน +2

      Ndeysane delen xole lingen di wax thi setou Serigne BABACAR sy bakhna rek kokoy samba Mane kanam mane guinaw

    • @morndadje4198
      @morndadje4198 หลายเดือนก่อน

      Occupe toi de ta tarikha

    • @user-hv6li6oq4k
      @user-hv6li6oq4k หลายเดือนก่อน

      Wallahi degele

    • @user-px5kf9ip8d
      @user-px5kf9ip8d หลายเดือนก่อน

      Ay way kou diokh thieur serigne moustapha war nga diokh thieur bénéne serigne moustapha bi ndakh ndiabottou maoda la mane dé douma kénneu lou niaw

  • @CheikhFall-wn2ci
    @CheikhFall-wn2ci หลายเดือนก่อน +10

    Dioubo bi mome damasi decourage yakaratouma mou am korite bi passer amon nan occasion bou reuy mais malheureusement parfois sen rancune molène sonal ak fatelikou demb

  • @abdoulayediallo8739
    @abdoulayediallo8739 หลายเดือนก่อน +1

    Nieuppé ligueyal keur cheikh seydil hadj Malick Sy RTA moo gui dallé Serigne sidy Ahmed sy Malick jusqu'à Serigne Babacar sy Mansour khalif général des tidjianes machallah baarakallahu fiikum bonne continuation

  • @SodaFall-lv1no
    @SodaFall-lv1no หลายเดือนก่อน +14

    Mais amon guen occasion DIOUBO yenako diotay bi guen am tay solen ko amon jour korite bir keur serigne babacar sy kone affaire yi diekhna bayilen talibe Yiguen di manipuler

    • @leadermodou948
      @leadermodou948 หลายเดือนก่อน

      Billay une bonne occasion sakh mais dangay waarrou

  • @user-le6of6sl5t
    @user-le6of6sl5t หลายเดือนก่อน +19

    Moustapha bou Serigne Abdou mo tour yalwane gui Yep diam naron n'a am mais mo gneuw yak lepp

    • @galsen3231
      @galsen3231 หลายเดือนก่อน +3

      Néxoul degue dh mais je vois que mo yakk lepp

    • @khalioudrame9526
      @khalioudrame9526 หลายเดือนก่อน +1

      Touroul dara Dada kham djikoy moustapha sy.yenak dafa mour seni beut nguir dilene gyeuneu manipuler

    • @issaba3187
      @issaba3187 หลายเดือนก่อน

      @@khalioudrame9526 Yalla na yagg diniou manipuler akk xamxam bou Séll, akk deugou, akk yarr. Lounii fangg keinn douko diexx 😅
      Fii doff amou Fii 😂
      Guiss neinn fii seinn Tapha junior akk ayath bimou done tarri keirok. Gathiei deug laniou tekk.

    • @khalioudrame9526
      @khalioudrame9526 หลายเดือนก่อน

      @@issaba3187 yar nga wakh deh?? Ki sagga ay bayam, Tongo ak ay bayam ay frère ram...kou gneup tifli nga toy deh..même khalifa mbaye gneup gneup

    • @issaba3187
      @issaba3187 หลายเดือนก่อน

      @@khalioudrame9526 Danio diarr sagga motakh.
      Abou lahab lanla sii yonentei bii?
      Saway nangou leinn doggal nopalou. Guiss nga yii ngaay défendre fii yeup lii serigne Moustapha réalisé sii diangalei akk yaar ndiabotam souniou ko deifon mou bakh. Niveau yii dou beineu deii. Ils seront bientôt dans l’oubli, Serigne Moustapha on parlera de lui des siècles après car c’est le plus noble et le plus grand Savant de son époque. Deileinn ko saggo

  • @AichaLy-fx3zj
    @AichaLy-fx3zj หลายเดือนก่อน +6

    Mashalla

  • @mameabdoudieng3780
    @mameabdoudieng3780 หลายเดือนก่อน +4

    Machallah ❤

  • @amifall1894
    @amifall1894 หลายเดือนก่อน

    Diarama seyidi mouhamadou moustapha sy al maktoum yalla na yalla goudalle fanam te samouko te arreko motalileko yeneme sí barke mame babacar sy barke mame chiekh a tidiane sy al maktoum ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-vr2ri8qs9p
    @user-vr2ri8qs9p หลายเดือนก่อน +3

    Machalla sama serign bii ❤

  • @user-nq4nt4ss4c
    @user-nq4nt4ss4c หลายเดือนก่อน +11

    Mais man souma guissé Guen woté diam wala diko Niane dafmay diakhal trop bilahi amon Guen occasion bi loutakh exploité wo len ko

  • @MariamaCisse-tm4cx
    @MariamaCisse-tm4cx หลายเดือนก่อน +3

    ❤machalla amnasolo

  • @babacarseck7753
    @babacarseck7753 หลายเดือนก่อน +4

    Yobouléne potou ndayi té douye thi ndayi ba fésale nane té moytou di wakh wakh diou khadialé seutou maodo

  • @moussambengue7133
    @moussambengue7133 หลายเดือนก่อน +1

    Alkhamdoulillah Sy Malick almaktoum almoustapha alcapitaine the Best nos cœurs à vous ❤❤❤

  • @laminediop5788
    @laminediop5788 หลายเดือนก่อน +7

    Ay way guéneu léne ci famille diambour yi

    • @babacarseck7753
      @babacarseck7753 หลายเดือนก่อน

      Walahi danie thi yakho rék

    • @salioufaye9818
      @salioufaye9818 หลายเดือนก่อน

      Wa yow kiy wakh ni kanamou nieup lako waher

  • @seynaboudiop7140
    @seynaboudiop7140 หลายเดือนก่อน

    Diarama Serigne Cheikh Tidiane SY Al Amiin 🙏🙏🙏

  • @MouhamedFall-eg6ys
    @MouhamedFall-eg6ys หลายเดือนก่อน +8

    Serigne Moustapha sy Al Maktoum def na liko war yeup❤❤❤❤

  • @abdoulayefall1282
    @abdoulayefall1282 หลายเดือนก่อน

    Waww kane mo thioww dou guéne ko wakh , serigne Moustapha Sy rek guama mana guéné wakhtane bumu deff les années 70 parmi ñi took fofu té ménoum momm réussir na lou yéne mbolo bobu réussir roul tek nanu Yako louné nak té wakhoul soulna baye katim ñu souliko té kéne si yéne wakhoul melni khamu léne baye katim té n'empêche ñiewna si keur gui woté djiguéne ñi rek ñoko térru
    . Yénne khamguéne ni bounone teull fofu Gamou gui Diekh thieur ak boromm

  • @mbenguemathiaw5447
    @mbenguemathiaw5447 หลายเดือนก่อน

    Machallah wakh bi amna solo

  • @abdoulayediallo8739
    @abdoulayediallo8739 หลายเดือนก่อน +1

    Ak guinaw Serigne Babacar sy Mansour khalif général des tidjianes, Serigne maodo sy dabakh etc .. jusqu'à aahirou keep kouy nieuw yessal defar yokkaat ligueye cheikh seydil hadj Malick Sy kamaa mine hablihim inchallah

  • @daoudandiaye-um3zs
    @daoudandiaye-um3zs หลายเดือนก่อน +2

    Li nexna machallah

  • @user-ml5qo4gr4j
    @user-ml5qo4gr4j หลายเดือนก่อน

    Machallah amna solo

  • @morniang9878
    @morniang9878 หลายเดือนก่อน +1

    Léppe thiaka nangou li Yalla déffale Serigne MOUSTAPHA Sy ALMAKTOUM

  • @amifall1894
    @amifall1894 หลายเดือนก่อน

    Dieureudieufaty seyidi mouhamadou moustapha sy al maktoum ❤❤❤❤❤❤

  • @AmethDiop-ut4ei
    @AmethDiop-ut4ei หลายเดือนก่อน

    Machallah. Yal na yalla defal niep diaam

  • @maguettembodj4143
    @maguettembodj4143 หลายเดือนก่อน +2

    MACHALLA ❤❤❤❤❤❤

  • @jamiloulah7115
    @jamiloulah7115 หลายเดือนก่อน +11

    Serigne moustapha al Maktoum est l’incarnation de l’islam parfait kou roy si mom defarou defar say talibé kou menoul wakh si mom diam nak nga mandou si mom mom rek lanouy top.
    Kouko nangoul niou nangoul la kouko diamal am diam nila tolouuuu

    • @MouhamedFall-eg6ys
      @MouhamedFall-eg6ys หลายเดือนก่อน

      Ni rek la tollou

    • @hannengom
      @hannengom หลายเดือนก่อน

      VRAIMENT TÉ LOLOU MÉTIWOUL

  • @malickniang9974
    @malickniang9974 หลายเดือนก่อน +3

    Ma challa Serigne pap

  • @momodousarr9807
    @momodousarr9807 หลายเดือนก่อน

    Walakhi diarama serigne moustapha sy al Maktoum

  • @salioufaye9818
    @salioufaye9818 หลายเดือนก่อน

    Terer yiguay wakh serigne moustapha môme lay diangal ndiabotam

  • @ousmanecisse4262
    @ousmanecisse4262 หลายเดือนก่อน +1

    ❤❤

  • @damedia4990
    @damedia4990 หลายเดือนก่อน +4

    Yi façon deugue amoul féne serigne pape merci

  • @fatimasy108
    @fatimasy108 หลายเดือนก่อน +11

    Bouthi kounè nango lou yalla dogal diame ame sokhar ak nafek bakhoul

  • @AmdymoustaphaDiop-ql3nc
    @AmdymoustaphaDiop-ql3nc หลายเดือนก่อน +1

    Kii di wakh moyy Kane ci wa keur Al amine

    • @mansourseck6738
      @mansourseck6738 หลายเดือนก่อน +1

      Khamoumako waye deugg rek la wakh yalna sougnou boroom deff deggo ak benno thi keur gui

  • @aliounebadaradiop6529
    @aliounebadaradiop6529 หลายเดือนก่อน

    Khawma loutakh niou beug par parlo ak ay details maodo eup na lolou ha😭😭

  • @brunocox62
    @brunocox62 หลายเดือนก่อน +1

    WAKHLENE AK QUI DI CONTESTER KHALIFE BI .

  • @lavoielactee111
    @lavoielactee111 หลายเดือนก่อน

    Kone yena gui sone aye mbir té douguen ko dane. Kone xolate len sen bop...
    wax jam ci kaw wax safane wa ci souff mo yakh keur gui.
    Moustapha al amine amoul yar amoul teguine niep xam nanu ko. Boudé mo yor responsabilité keur serigne Babacar sy c'est très normal et respectable même serigne Moustapha Makhtoum yeugal ko ko. Et puis c'est tout passé woul lolou.... lim ci tek yeup yeuf yabaté la serigne Moustapha dou moromam moko raw milliards de fois.

  • @user-qe9ts6ty1f
    @user-qe9ts6ty1f หลายเดือนก่อน +2

    Wakhofi Dara bougent nagoul lon seringe Moustapha sy al maktoum dara dou khew

  • @AlhagieCeesaygarry
    @AlhagieCeesaygarry หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤

  • @user-lk9fk2ri4r
    @user-lk9fk2ri4r หลายเดือนก่อน

    Dieredef Amna solo

  • @IbrahimaGueye-vu9lq
    @IbrahimaGueye-vu9lq หลายเดือนก่อน

    S.Moustapha bou al amine mou yakh li warone rafet

  • @lavoielactee111
    @lavoielactee111 หลายเดือนก่อน

    Cheikh seydi Moustapha sy jara jeuf bou nieup défone ni iow kone ken dou diam nani keur gui.

  • @AJDKTVdeKambel5744
    @AJDKTVdeKambel5744 หลายเดือนก่อน

    Sering si xolat len sen bopu tay bayi sen problèmu famille yi ñiy feusal si Média li wa Tivaouane rk ñoko dese sonal ngen ñu bilay

  • @ndaoallassane1187
    @ndaoallassane1187 หลายเดือนก่อน

    amiiiin

  • @SerignefassKoundoul
    @SerignefassKoundoul หลายเดือนก่อน

    Wakh lënë deug sen rakk bi feroule idje aussi nguene nagoule serigne Moustapha Sy ibn Serigne Cheikh

  • @user-gz2rf2iv8v
    @user-gz2rf2iv8v หลายเดือนก่อน +3

    Nioune talibé dioubo laniou beugue

  • @aminataami4177
    @aminataami4177 หลายเดือนก่อน

    Serigne Moustapha sy Al maktoum mo donou makk gni té kheutio woul
    Thiowoul, nangoul lén ko

  • @safietousarrfall9515
    @safietousarrfall9515 หลายเดือนก่อน +7

    Waxantè len deug ci sen bir Serigne Moustapha bou al amine guen wara wax deug kilifa dou waxei kom nimou waxei kilifa day defar

  • @believeyourself158
    @believeyourself158 หลายเดือนก่อน

    Tapha sy rek moy nattu keur maodo

  • @laminediop5788
    @laminediop5788 หลายเดือนก่อน +2

    Abdoulaye Diop nitte day yarou

  • @makmak8062
    @makmak8062 หลายเดือนก่อน

    Nite kou bakh dafay ame kilifa

  • @safietousarrfall9515
    @safietousarrfall9515 หลายเดือนก่อน +1

    Mane farouma fein deug reik lay wax dagen wara diohei bon exemple aduna leip rafetal leu wayei di wax lou ken khamoul vraiment mom weierei gein tei li sou yaguei ken dotoulen geumati wasam

  • @user-hv6li6oq4k
    @user-hv6li6oq4k หลายเดือนก่อน

    😭😭😭

  • @antandiaye1509
    @antandiaye1509 หลายเดือนก่อน

    DIEUREUDIEUF SERIGNE BABACAR CISSE DIEUREUDIEUF

  • @abdoulayefall1282
    @abdoulayefall1282 หลายเดือนก่อน

    Jarama Al Mourchid sa liguey ñiépa ko guiss Sy

  • @TAWAMBAYETV
    @TAWAMBAYETV หลายเดือนก่อน +2

    Gni niak sago rk nioko yax wayei manone n'a ame

  • @abdoulayendiaye617
    @abdoulayendiaye617 หลายเดือนก่อน +5

    Serigne moustafa sy maktoum moy solution by

  • @malickmbodj4146
    @malickmbodj4146 หลายเดือนก่อน

    Loumou wokh amna solo lol thieurrou Yalla yénako nitt ki sinon dangay sonna reikk thieurrou Yalla nakk si xam xam akk djikoo ngakay xammé naniou yénanté diamma yénné kouné likko Yalla défal keurgui avancer dieum si kanam inchallah

  • @moussaladiane82
    @moussaladiane82 หลายเดือนก่อน

    Lidieun ti lênn sénn keur Bay yi té Bayi Famille diambour bagni boke fékéwou lénn

  • @user-pw9ln3sq8u
    @user-pw9ln3sq8u หลายเดือนก่อน +7

    Je ne sais pas pourquoi ces gens là n’aiment pas Serigne Moustapha Al Makhtoum ?

    • @kanebocar2745
      @kanebocar2745 หลายเดือนก่อน +2

      Kouko bagn nafek bakhoul

    • @momo-hp4yf
      @momo-hp4yf หลายเดือนก่อน +3

      Moustapha kenn bagniouko waye dafi wakhone aye cadou you niaw thé kenn rafet louwouko

  • @_diakhate
    @_diakhate หลายเดือนก่อน +3

    Solèn nangou lon Serigne Moustapha Sy Al Maktoum batey Tivaouane wéssu neu fii. Mom kassé réalisé neu loungèn réalisé woul boungèn booloo. Tivaouane yèna ko tardèl, yéna ñuy yablu, nakh xam ngèn ki dondu tariqa bi ngèn lank ni douthi dal ba paré diñu sonal ak wakh.
    Thieur bi keneu douko séddo, kéneu koy yor té R.M❤❤❤.

    • @mamediop8845
      @mamediop8845 หลายเดือนก่อน

      😂😂😂😂😂😂momite na nangou li yalla dogal

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 หลายเดือนก่อน

    Tivaouane seini problème dafa tambaleiwou si gni depuis si mag gna reinoupe gnambi bou moudjou done garabe leu

  • @daoudandiaye-um3zs
    @daoudandiaye-um3zs หลายเดือนก่อน +1

    Machallah

  • @kikimbaye
    @kikimbaye หลายเดือนก่อน +8

    Yén gny commenté Di dougou eu famille diambour Di oute founguen fare yéne yénay nafekkk

    • @babacarseck7753
      @babacarseck7753 หลายเดือนก่อน

      Walahi bayiléne rékeu khamougniou mame maodo matakh niouye khadialé ndiabotame

    • @Elbachir5971
      @Elbachir5971 หลายเดือนก่อน

      Walay deugueleu ❤❤❤

    • @SodaFall-lv1no
      @SodaFall-lv1no หลายเดือนก่อน

      Nio exposé sen Bop si internet bi kone gnep si am acé nopil saytané

    • @khamsabopou6598
      @khamsabopou6598 หลายเดือนก่อน

      Kikimbaye yaw ya mana fen también louy si sen yon ñominén la iñan nanté sokharan té kouné si diër ga nék fi difen

    • @cheikhtidianegaye6148
      @cheikhtidianegaye6148 หลายเดือนก่อน

      Comm sa bay

  • @BayeMboup
    @BayeMboup หลายเดือนก่อน

    Nguen ballma ki kanla

  • @cheikhtidianegaye6148
    @cheikhtidianegaye6148 หลายเดือนก่อน

    Wakh lénn Moustapha Al amine deukk mon Guen mon yakk lépp

  • @dameseye3039
    @dameseye3039 หลายเดือนก่อน

    On ne peut que prier pour la paix sincère
    Bien vrai que talibé yi daniouy khamb mais aussi kilifa yi niom itam fàw niou am depassement
    L' union fait la force

  • @MamadouDiouf-iz8bu
    @MamadouDiouf-iz8bu หลายเดือนก่อน

    Serigne Moustapha barkè mame doundou louko nak dafa deffa ligueyal mamam ba bayam gueureum .mota tank kanam rek kouko ignanè xol bou bone ba dougou bamel dem safara

  • @omarediery2069
    @omarediery2069 หลายเดือนก่อน +2

    Machallahh yalna yalla samal niou serigne moustapha sy al maktoum in challahh ❤❤🤲🤲

  • @user-pd4oz3ht6r
    @user-pd4oz3ht6r หลายเดือนก่อน

    Wakh lene ak kiye kheuthio kou diaguoul ba paré

  • @modoukane4193
    @modoukane4193 หลายเดือนก่อน +1

    Me ki koumoudon

  • @ndeyembengue4511
    @ndeyembengue4511 หลายเดือนก่อน

    Lolou yonou talibé nékou si😮

  • @mamourfall8934
    @mamourfall8934 หลายเดือนก่อน +6

    Waxe lene ak sene borome "vulgaire violaire" ngene xamal ko ni kou gueuna ndaw si ndiabottou serigne moustapha sy Al Macktoom moko raw foufe

  • @MadyCisse-lf1zp
    @MadyCisse-lf1zp หลายเดือนก่อน

    Serig, bi, ligaywakh, niemeko, tou, koutour, sell

  • @alindao6836
    @alindao6836 หลายเดือนก่อน +5

    Donc seydi Mouhamadoul Moustapha sy Al maktoum limou am dafko niafé ta bamoukoy niafé gnifi nékk tay di khokhali beut kene xamou léne

  • @NdiagaDiop-mx6jw
    @NdiagaDiop-mx6jw หลายเดือนก่อน +5

    Soudé wax mome ken dakoulen wakh Lou Rafet mais soudé dieuf ken doulen guiss kerok jour korite yow fonekon pour keur gui nek ben Say soeur gneuw Tok yaw gneuwo ba paré Di woté diam

  • @OmarGueye-uf6fl
    @OmarGueye-uf6fl หลายเดือนก่อน +2

    Machaalla ❤ Serigne Moustapha s'y Al maktoum