Urgent Touba une femme retrouvée Après 42 ans disparition

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 5 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 739

  • @ndeyengonembaye9436
    @ndeyengonembaye9436 ปีที่แล้ว +2

    Macha allah cheikhouna🥰 yalla nala yalla Fay yiw🤲

  • @ousmanendong6471
    @ousmanendong6471 4 ปีที่แล้ว +35

    Cheikhouna tu es un modèle pour la religion à l'égard de ton bon geste. Tu ne le regrettera jamais au plus grand jamais. Que le seigneur t'apporte une vie meilleure ici et au-delà.

    • @SidyMGueye
      @SidyMGueye 2 ปีที่แล้ว +1

      Il n’est pas seulement un modèle pour sa religion, c’est un modèle HUMAIN.

    • @annegaye7743
      @annegaye7743 2 ปีที่แล้ว

      P

  • @abdouthiandoum483
    @abdouthiandoum483 2 ปีที่แล้ว +2

    Ndeysane Cheikhouna Fall ya bakh

  • @Africanadienne
    @Africanadienne 4 ปีที่แล้ว +94

    Machaa'Allah, quelle belle histoire ! Puisse Allah te récompenser abondemment, notre cher Cheikhouna.

    • @madokhoureychy4886
      @madokhoureychy4886 4 ปีที่แล้ว +3

      Qu'Allah te le paie au centuple amiiine

    • @amyciss5039
      @amyciss5039 4 ปีที่แล้ว +3

      Assalamou aleykoum m, bokayi mane Sama mag mougui toudou Djibi Pouye niou guanko wower Djibi sangou rerena yagana bobou dioudouwouma balegi niongi doundou yakar guissko koougnoussi dimbali te yalla takh dieuregendieuf

    • @aronandiaye8974
      @aronandiaye8974 4 ปีที่แล้ว +2

      Tu es bien ,yallah souniou borom défal la ay yiw.

  • @fanschesea277
    @fanschesea277 4 ปีที่แล้ว +61

    Personnellement je connais cheikhouna mais un talibe un homme bien bonne continuation frère

    • @Thyphanie8019
      @Thyphanie8019 4 ปีที่แล้ว +1

      Maa shaa Allah sama domou baye. Yala nala yala fay bakhe

  • @famaracamara6118
    @famaracamara6118 2 ปีที่แล้ว +3

    J'ai même pleurer quel émotions. Cheikhouna yalnala yalla fey yiw. J'avais des frissons depuis le début de l'histoire mais au moment où sokhna Coumba a commencé à témoigner sa reconnaissance envers cheikhouna et que ce dernier verssa des larmes j'ai aussitôt verser des larmes aussi

  • @alhamdoulilahrek6167
    @alhamdoulilahrek6167 4 ปีที่แล้ว +21

    Serigne mountakha dakoo waroon Yeukk teral koo . Kii limou deff dieuff diou reuy la Machalla 🙏🏾👏🏾👏🏾👏🏾. Beugon na ham aussi Mere bi noum deff ba demon yemen ba reer ay mbokkam ???

  • @famanguer4153
    @famanguer4153 4 ปีที่แล้ว +39

    Cheikhouna linga def Mane ngako d'égal wakh deugue kontan n'a top yalla nala yalla fayd dieureu d'oeuf fall yaram après 42 an Douay foo

    • @mayoronguer2498
      @mayoronguer2498 4 ปีที่แล้ว +4

      Bilahi exemplaire la ci kepp kou nekk ci réseaux sociaux yi lii kessé lay diarign

    • @ndeyefall5489
      @ndeyefall5489 4 ปีที่แล้ว

      Ndeysane machalah yalla nala yalla Faye si barke mouhamed est

  • @bayediop9868
    @bayediop9868 4 ปีที่แล้ว +12

    Machallah amna nitt gnou bakh CHEIKHOUNA FALL yalla nous sunu borom fay

  • @xamsaguene5092
    @xamsaguene5092 4 ปีที่แล้ว +27

    Wanega dioukeuy serigne Touba.masha Allah

    • @diengpape9289
      @diengpape9289 2 ปีที่แล้ว

      Wawaw lila s bi diangale

  • @momombowofficiel207
    @momombowofficiel207 4 ปีที่แล้ว +4

    cheikhouna yalla nako yalla dèfal jam si barki borom touba

  • @bayesalioukane8321
    @bayesalioukane8321 4 ปีที่แล้ว +16

    جزاك الله خيرا يا أخ الكريم شيخنا فال

  • @galassdiouf
    @galassdiouf 4 วันที่ผ่านมา +1

    Cheikhouna yaw président dala waron décoré❤❤❤❤ bilahi linga déf reuyna ❤

  • @sendsene8608
    @sendsene8608 4 ปีที่แล้ว +11

    Cheikhouna brom khol bou rafet Machallah

  • @assytoure3827
    @assytoure3827 2 ปีที่แล้ว

    Macha Dawna yaram cheikhouna yalla na na na yalla Faye la Ay way kou am numéro cheikhouna dimbalima ci sama rakou papa mo rere dans les années 80

  • @yayabadiane3610
    @yayabadiane3610 4 ปีที่แล้ว +167

    Touba la ville des champions de l'islam

  • @toubadarousalamtv6716
    @toubadarousalamtv6716 4 ปีที่แล้ว +1

    MACHA ALLAH Cheikhouna Fall sama Talibé sama kharite sama Leppou , dama beugeu adouna yeuppou khamenii kou bakh nga kouye dimbaliiwaténga kou n'ango sonou si yittéé domou adama .... . Macha Allah yalana Yallah samou taa barkél-laa defala diamou. Begg nassi yaw c de la part de Ndiaga

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774
    @youssoufabdoulayediopjohnn3774 2 ปีที่แล้ว

    Mashaalah Chekhouna sunu Boroom doli leu fay mashaalah

  • @cheikhmbaye6012
    @cheikhmbaye6012 2 ปีที่แล้ว

    masha'ALLAH Cheikhouna, ya'ALLAH nala sounou BORÔME Faye çi barké Cheikhoule Khadim !

  • @FalouNiass
    @FalouNiass 9 หลายเดือนก่อน

    يا ماشاء الله ياشيخنا فال قد أثلجلت قلوبنا والله جزاك الله خيرا

  • @Dioplink
    @Dioplink 4 ปีที่แล้ว +34

    Cheikhouna Fall machALLAH sa état d'esprit nekhneumeu lol yalla na la yalla fay yiw

    • @dydyngom2142
      @dydyngom2142 4 ปีที่แล้ว +1

      Sama nidjay xawmako il a disparu depuis longtemp il sapel démba ngom

    • @amyciss5039
      @amyciss5039 4 ปีที่แล้ว

      Assalamou aleykoum m, bokayi mane Sama mag mougui toudou Djibi Pouye niou guanko wower Djibi sangou rerena yagana bobou dioudouwouma balegi niongi doundou yakar guissko koougnoussi dimbali te yalla takh dieuregendieuf

  • @antatoure9239
    @antatoure9239 4 ปีที่แล้ว +10

    Machalla cheikhona fall yaram kêne dou yaw amou morom yallna la yalla faye ci barké s saliou

  • @muna326
    @muna326 4 ปีที่แล้ว +62

    Machallah mais moi je veux savoir comment elle s'est retrouvée à Yemen depuis 42ans

    • @zeynadiaw7980
      @zeynadiaw7980 4 ปีที่แล้ว +5

      Exactement bonne question

    • @harounalo7242
      @harounalo7242 4 ปีที่แล้ว +19

      Elle était mariée a un arabe ver les années 1978 moi je la connais très bien j ai grandi devant on ai même village

    • @elche4179
      @elche4179 4 ปีที่แล้ว +2

      @@harounalo7242 au moins qqn qui explique bien.

    • @Oumanas5995
      @Oumanas5995 4 ปีที่แล้ว

      @@harounalo7242 waw soubkhanallah

    • @cherieib8164
      @cherieib8164 4 ปีที่แล้ว

      @@harounalo7242 merci

  • @stephane7043
    @stephane7043 4 ปีที่แล้ว +11

    Machallah cheickhouna long vie santé qu'Allah te récompense mon frère 🙏🙏🙏

  • @zdpdiakhate2139
    @zdpdiakhate2139 2 ปีที่แล้ว

    Cheikhouna yalla nala yalla faye si barkei cheixoul khadim

  • @ndeyeba9221
    @ndeyeba9221 4 ปีที่แล้ว +48

    Cheikhouna Fall ligua déff dafa reuye bilay fégnal kou rérone ay mbokam aprés 42 ans yalla nala yalla takhawou bilay amougnou sa faye

  • @mouhiboulkhadim2030
    @mouhiboulkhadim2030 4 ปีที่แล้ว +7

    Machalla Chiekhouna fall yalnala sounou borom takhawou

  • @narfall7067
    @narfall7067 4 ปีที่แล้ว +11

    Mashallah sekhouna fall jesus fair de toi yallna la yalla faye🙏🙏🙏🙏🙏💜👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿

  • @dababa6854
    @dababa6854 2 ปีที่แล้ว

    Machalah Cheikhouna yalnala yalla faye

  • @ndeyediouf2718
    @ndeyediouf2718 4 ปีที่แล้ว +6

    Machalla chėikhona Fall linga dėff reuyna lool yallna la yalla faye

  • @mairyndoye3906
    @mairyndoye3906 2 ปีที่แล้ว +1

    Macha allah
    Cheikhouna Fall . Que Dieu veille sur vous et votre famille
    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dgt8669
    @dgt8669 4 ปีที่แล้ว +31

    Machalla Serigne Cheikhouna Fall Yallanala Yalla Faye thiy barkéb Serigne Touba

  • @alnassi
    @alnassi 4 ปีที่แล้ว +3

    Cheikhouna waaliou la, yalna ko borom bi arr.

  • @cheikhboudiop539
    @cheikhboudiop539 2 ปีที่แล้ว +9

    Alhamdoullillah Alhamdoullillah Alhamdoullillah Dieuredieuf Cheikhouna
    QU’ALLAH SWT Répande sa grâce sur toi CI BARKÉ SEYDINA MOHAMED (PSL)
    Nous prions afin cette famille se retrouve dans la paix et le bonheur. Une immense joie en perpective.

  • @mamefatoubeye8274
    @mamefatoubeye8274 4 ปีที่แล้ว +8

    Li mome reuye n'a trop Macha Allah yalna yalla faye sa khole ❤️

  • @DARADJITV569
    @DARADJITV569 4 ปีที่แล้ว +27

    mande al coran rek lay dougual ms guissouma kouma abonner 😭😭😭koumay abonner yallah fayla

    • @abdoulahatdiakhate4751
      @abdoulahatdiakhate4751 4 ปีที่แล้ว +1

      Nga mougn té doylo yalla isss

    • @dadogueye7195
      @dadogueye7195 4 ปีที่แล้ว

      @@abdoulahatdiakhate4751 ki buzz lay weure vidéo boumou deim deif si commentaire bi

    • @inconnu90000
      @inconnu90000 4 หลายเดือนก่อน

      Pousseul fi , demal diangui alkhouran teh bayi net bi

  • @ndackfall1157
    @ndackfall1157 4 ปีที่แล้ว +1

    Ki dé kuko guiss rek nga kham ni ku barri yeuremandéla yalla nalla yalla faye fall yarame

  • @ababacarndiaye5352
    @ababacarndiaye5352 4 ปีที่แล้ว +7

    ماشاء الله جزاك الله خيراً شرج شيخنا فال

  • @cheikhantandiaye4183
    @cheikhantandiaye4183 2 ปีที่แล้ว

    même son sourire est ilimite maschalaah.il est tout cœur ce cheikhouna mais tu vas voir quand allah va arriver sur toi.

  • @Senegal-nm1nq
    @Senegal-nm1nq 4 ปีที่แล้ว +23

    Ndeye san Aka Bakh sama domou ndidiaye la ndeye san😍🥰❤️😘❤️😍🥰

  • @antadiagne1166
    @antadiagne1166 4 ปีที่แล้ว +11

    Ceux qui dislike c'est quoi votre problème 🤷 machalla cheikhouna force sur toi

    • @mberryable
      @mberryable 4 ปีที่แล้ว +3

      Anta Diagne même sourate Fatiha walla yassin sakh amna gnoukoy dislike 👎 ainsi va la vie néanmoins je te suis et comprends

    • @xadimsill1483
      @xadimsill1483 4 ปีที่แล้ว

      MoMA diaxal

    • @rokhayalavillageoise8380
      @rokhayalavillageoise8380 4 ปีที่แล้ว

      Yefarr yila rk

  • @elmadrista8667
    @elmadrista8667 2 ปีที่แล้ว

    Machallah grand frère cheikhouna fall

  • @diallomouhamadou4953
    @diallomouhamadou4953 2 ปีที่แล้ว +1

    Mâcha Allah amna solo yalla nala Yalla Faye ci barke alkhourane amine ❤

  • @sambaseke109
    @sambaseke109 4 ปีที่แล้ว +1

    Merci amna solo

  • @fatousane867
    @fatousane867 4 ปีที่แล้ว +6

    Oh li dawna yaram ndèyssan, Cheikhouna yAllah nala yAllah samm té fayla yiim, MachAllAh

  • @mbackehabiboumbackehabibou5370
    @mbackehabiboumbackehabibou5370 18 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤ماشاءالله سرج شيخنا فال

  • @thiernondiaye5126
    @thiernondiaye5126 4 หลายเดือนก่อน

    Merci beaucoup vous êtes un digne sénégalais

  • @maimounafall5625
    @maimounafall5625 4 ปีที่แล้ว +3

    Ckeikhouna sa khol rafétena machalah Yallah nala Yallah fay sa khol

  • @torasylla4303
    @torasylla4303 4 ปีที่แล้ว +2

    Bilahi cheikhouna donou nga sa tourondo yallana yalla takhoula té diapouléla

  • @gueyebara3010
    @gueyebara3010 4 ปีที่แล้ว +122

    Ay waay lii amna solo deh Internet li lay jarigne wayeh foo rék

    • @bmtvthiattinfo1855
      @bmtvthiattinfo1855 4 ปีที่แล้ว +3

      Ma challah sama xaritt bi kenn du yaw dioye loo Gama 😭😭😭😭

  • @syllaserignemadiama1889
    @syllaserignemadiama1889 4 ปีที่แล้ว +14

    Machaallah serigne cheikhouna li dé moy li serigne touba beugon thi ko deuk touba takhaway bi yalna yag ta sunu borom diapolé la thi sahir Ak thi baatin

  • @taphandiaye
    @taphandiaye 2 ปีที่แล้ว

    Cheikhouna yalla naga gouddou fan

  • @fallndeye6878
    @fallndeye6878 4 ปีที่แล้ว +3

    Ndeysane s.cheikhouna fall yalla na yalla fayla c.barké s touba

  • @amifall9950
    @amifall9950 4 ปีที่แล้ว +1

    Sama xole♥️mo sedd ba may dioy 😭😭😭bilahi cheikhouna bou nékone si payer européenne yii dinaagn ko décoré par ce que dafa déf acte bou Noble bravo et bonne continuation frére 👋👋👋👋

  • @amanarassul718
    @amanarassul718 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah serigne sekhouna yalna yalla fayy

  • @mariamegningue5902
    @mariamegningue5902 4 ปีที่แล้ว +3

    Ndeysanne machallah ❤️ yalla nako yalla défal diam cheikhouna mi allahouma amine ya rabi 🙏 🙏 🙏

  • @lejustemilieu245
    @lejustemilieu245 4 ปีที่แล้ว

    Ziarnaléne li mome raféte na lolou comme ils sont de Touba guir yalla nassi khalif bi déf yitté guir famille bi délloussi Touba incha alla

  • @Oumou_Fatima_Joob
    @Oumou_Fatima_Joob 4 ปีที่แล้ว +8

    Ayuue ndeysan mashaa Allah! La façon dont elle remercie graduellement: Allah apres Cheikhouna Fall est vraiment touchante! P

  • @yasallamou8543
    @yasallamou8543 4 ปีที่แล้ว +2

    Serigne cheikhouna yalla nala borom bi takhawou

  • @amadoudiago9133
    @amadoudiago9133 2 ปีที่แล้ว

    Bonjour. Pour completer le reportage, on aimerait bien connaitre les raisons qui l on conduite a Yemen.

  • @samb9757
    @samb9757 2 ปีที่แล้ว

    Machalah li Amna solo lole limoy Sénégal dimbalante te yalla takh

  • @serignecheikh1official627
    @serignecheikh1official627 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nala yalla takhawo serigne chekhouna fall thi barkibe s touba

  • @yacinediagne3526
    @yacinediagne3526 4 ปีที่แล้ว +2

    Sama frère bi rére yalla na fégne sama yaye dioy nako ba sonou

    • @fatimatra8457
      @fatimatra8457 4 ปีที่แล้ว

      ay yaw lolou mettina sa frère je suis sûre qu'il est en vie quelque part yalla na feigne 😥😢es ce que bimiy deme taggou na ????

  • @sokhnafatousonghor7344
    @sokhnafatousonghor7344 4 ปีที่แล้ว +2

    Ndeysane amna solo mashallah yalla nala yalla Faye borom si barke Touba

  • @cheikhtalibouyandiaye1918
    @cheikhtalibouyandiaye1918 2 ปีที่แล้ว

    wallahi ndeysan yalnalla yalla fay yiw ci barké Cheikhou Tidiane

  • @saphietoudiedhiou1586
    @saphietoudiedhiou1586 4 ปีที่แล้ว +1

    Ndeysane mbokou alalou yalla la bakh gua lol yalla dinala fay. Inchallah

  • @salimata673
    @salimata673 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah
    Cheikhouna mii beugueunako dè💝💘💞

  • @Babbasfa
    @Babbasfa 2 ปีที่แล้ว

    Dieureuf koubakh Yalnala Ya RABBI fay ak yiw

  • @dadothiam3838
    @dadothiam3838 2 ปีที่แล้ว

    Machala Cheikhnouna yalna yalla motali nipe Yonne si barképe Serigne Bamba Khadim Rassoul rta amine adouna lépou terangala sauf dof bouye dooré machala doundou werr rek amine 💪💪💪🙏🙏🙏😭😭😭

  • @talibeserignebi9768
    @talibeserignebi9768 4 ปีที่แล้ว +44

    S. Cheikhouna Fall Yalla nala faye yiw te barkel lepou

  • @khadidieng9936
    @khadidieng9936 4 ปีที่แล้ว +12

    SERIGNE CHEIKHOUNA yallana BOUR YALLA fayla ci barkeeb SERIGNE MODOU MOUSTAPHA amine dieureudieufati

    • @mamoudoudiagne7722
      @mamoudoudiagne7722 2 ปีที่แล้ว

      Oui c'est maintenant que j'ai regardé la vidéo sur internet je suis moi aussi de sinthiou garba je connais toute la famille coumba sa mère vie vraiment c'est triste

  • @ndongodara6032
    @ndongodara6032 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalla s.chiekhona yalla nala yalla faye

    • @morniang1240
      @morniang1240 4 ปีที่แล้ว

      Machalah le dawna yarame

  • @biramefaye1640
    @biramefaye1640 2 ปีที่แล้ว

    Machallah tres belle histoire yalna souniou borom guena takhawou

  • @dramesokhna4467
    @dramesokhna4467 4 ปีที่แล้ว +3

    Mashalah SERIGNE Cheikhouna
    Yalla na yalla faye la koubakh nga🙏🏾

  • @cheikhmbaye6547
    @cheikhmbaye6547 4 ปีที่แล้ว +1

    Serigne cheikhouna yalna ko yalla fay ngueneu gui fay

  • @abdoubakhendiaye2021
    @abdoubakhendiaye2021 4 ปีที่แล้ว +6

    Cet homme est brave Yalla nako Yalla Fay

  • @mamalioudiop6440
    @mamalioudiop6440 4 ปีที่แล้ว +4

    ماشاء الله خيراً ما فعلت ياشيخنا فال ، بارك الله فيك

  • @issambengue3082
    @issambengue3082 4 ปีที่แล้ว +1

    Mouride sadikh yaa baakh waay
    Yalla nala yalla Faye

  • @thioubtalibebamba1881
    @thioubtalibebamba1881 4 ปีที่แล้ว +1

    Ndeysane machalla amna solo lol yalla nala yalla faye sa khol si barker serigne fallou sama khol toy na😭😭😭😭😭

  • @bathiebathie6783
    @bathiebathie6783 2 ปีที่แล้ว

    Ya bax sama serigne. Yalla nala yalla faye

  • @mohamedba4664
    @mohamedba4664 2 ปีที่แล้ว +1

    Macha Allah k Dieu vs accompagne!

  • @fadeltv9111
    @fadeltv9111 4 ปีที่แล้ว

    شكرا لك ياشيخنا فال❤️🇸🇳❤️🇸🇳❤️🇸🇳

  • @mamefatousane4606
    @mamefatousane4606 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah je ne le connais pas mais je sais que c est quelqu un de bien

  • @isaakan4198
    @isaakan4198 4 ปีที่แล้ว +2

    Ndeyssane lii dawna yreueme bilahi sama diarbate sreigne chiekohna ligua deff amena solos trop meis yalla mi amena sa faye yall naka yalla faye barkeb khassidayi vraiment sonou khell dalle na sonou yakaar doly koi si ioww bonne cotinacoine

  • @bayengallacissendigelfall5252
    @bayengallacissendigelfall5252 4 ปีที่แล้ว +2

    Cheikhouna mi yéyo na appui état Senegal. Liguèy bi reuy na lolou machallah.

  • @ameetfallsenegal3506
    @ameetfallsenegal3506 4 ปีที่แล้ว +11

    Bilahi mouride yi nio bakh😍

  • @leopoldsambou4748
    @leopoldsambou4748 2 ปีที่แล้ว

    Félicitations à toi. Mais une question taraude mon esprit. Comment elle a pu disparaître et se retrouver au Yémen ?

  • @loulouseck6114
    @loulouseck6114 4 ปีที่แล้ว +1

    Cheikhouna que Dieu vous bénisse e

  • @salioufall4562
    @salioufall4562 4 ปีที่แล้ว +6

    Ndeye sane amna solo loul yalla nala yalla faye

  • @souleymanediaoula4492
    @souleymanediaoula4492 2 ปีที่แล้ว

    Ndeyssane allahou akbar ….yalla nala yalla féye yiww

  • @ndirmountakha529
    @ndirmountakha529 5 หลายเดือนก่อน

    Machallah yalla nala yalla faye

  • @muntaxaasilla2244
    @muntaxaasilla2244 4 ปีที่แล้ว +27

    Bilalah I sama xol sedd na ci yaw
    Yal na Yàlla défal la ci sa jëf ju rëy ci nga jëf ngëramul sëriñ Tuubaa

  • @yassinengom5276
    @yassinengom5276 4 ปีที่แล้ว +13

    Ndeysane cheikhouna fall yalnanga goude fan sama kholle dafa fésse billahi cheikhouna fall ya bakh yalnala yalla faye amine amine amine yarabi

  • @nogayetoure9692
    @nogayetoure9692 4 ปีที่แล้ว +10

    Alhamdou lilah sama toma niew na si diamou bilay li dafa nékh

  • @matykane3166
    @matykane3166 2 ปีที่แล้ว

    Macha Allah Mbock Lii Mome Boullaco yalla Fayéé yalnala yalla Fay 🤲🤲🤲🤲🤲

  • @samba6664
    @samba6664 4 ปีที่แล้ว

    Cheikhona yalla nala yalla fay yalla nala yalla fay yalla nala yalla fay

  • @keindeibrahima4547
    @keindeibrahima4547 4 ปีที่แล้ว

    Thieuye lii yéména lool ndaysane cheikhouna boula yalla fayé dh dinga khamné défloubakh amnasolo

  • @sttv6923
    @sttv6923 4 ปีที่แล้ว +16

    Les amoureux du zikr abonné sur notre chaîne sadiaratou touba tv yalna niépeu am jamm

  • @ndiayealioune3176
    @ndiayealioune3176 4 ปีที่แล้ว

    Dieuredieuf Serigne Cheikhou FALL. Yalla reck mo laye faye.

  • @Yaayusangbi
    @Yaayusangbi 10 หลายเดือนก่อน

    Jazakallahu xayran ya Cheikhouna Fall boroom université du ramadan