Sëñ Xaadim kii tubaab yi lay wax waaye waxul mag ñi dégg-dégg nag lu am solo la ci nit waxuma nag boroom xam-xam ndax tubaab bi bëggul ku yewwu te sëñ bi Da doon yee nit ñi.
Serigne khadim man dey samab soppe nga waye tay mom danga sos ndakh s modou astou wakhoul li nga wakh toubab bi la s modou wakh waye wakhoul magni tapon serigne bi
Magui Toubb bu bakh Sétaan naa Émission bi wayé li S.Khadim di tontou S.Modou Asta wakhoul loolou, dafa wakhné Tubaab yi diappé wounko won diaamu Yalla wayé ay khalatt lanko diappé. Wakhoul Taalibé yi, Donté li S.Modou wakh andou maci
RAFAH TV nawnaa lénn lool wayé délén séytou wakh yi doog ko dugal ! Serigne bi mo dakha jaamu Yalla ñépp Geune ko séllalé ñiepp lolou lako Taalibé yi toppé moukoy déf ci ñiom, Giss giss bim am di yééh nitt ñi ci jamu yalla nak mo takh Toubaab jappouko,,,, Wayé li Modou Asta wakhné daxou kofi kénn té geunou ko Séllalé kénn lolou rék moy Fénn yi jara tontou ci wakh ji dou lénénn
Yen borome commenter yii nga xam saa nga rék moy s'en solution delen téwlou dora commenter lii moudou astou Mbackè wax ay fén Serigne Touba mo këuna mana diamou yàlla ba nopi këun ko dakh séllal koudoul mome moudou bayil sa wax you soufé ame na loo xam sonko diarou ko macky diarou ko niaku ngeen tégine lool té xamadi
Yow busso nafékh bu bon nga domu kharam dégue nga ndakh fi nga nékon wakh bu gnaw buné wakh nga ko cheikh béthio ta cheikh bi limu lingéyal Serigne Touba sa Baye défuko
Mor asta bi AK chiekh thioro bou pastef vrai nafekh rouss na sante bi sene genre Yi nioye marche Touba vrai imbéciles gni Dee d'où malenne diox benne thieur wedi n'a lenne
Je suis désolé de le dire ainsi mais à mon humble avis, Serigne bi Bousso, tu es dévié de ta trajectoire car tu es maintenant dans l'invective politique et le renvoie de l'ascenseur aux adversaires politiques. Il faut arrête de parler car plus tu parles, plus tu devoiles ta face politicienne car les paroles trahissent ta pensée. Au nom du ciel, reviens dans la daara et occupe toi de l'enseignement des aspirants et laisse les politiques derrière toi quelque soit ce qu'ils ont fait pour toi. Jaaraama
Ioe mii yaa wara ragal Yàlla ba noppi dook koo digal keneen kii limu dafa leer dani Serigne Touba tubaab yi jàpp ñu ko woon ngir julli ak woor ak jaamu Yàlla waaye gis gis bimu amoon lañu ko jàppe.
Dieuredieuf Imam Bousso Yaguefi lool té endak wér inchallah
Wallahi bousso tawfekh rek
S touba amoullmorom ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Sëñ Xaadim kii tubaab yi lay wax waaye waxul mag ñi dégg-dégg nag lu am solo la ci nit waxuma nag boroom xam-xam ndax tubaab bi bëggul ku yewwu te sëñ bi Da doon yee nit ñi.
Dieuredieuf bousso yalla nala yalla défal diamou
Machalla dr imam khadim amna solo
No dafa diom😭 sonko sou buegué réw mi na moy tou sari nitt yi kha mou niou darra baparé di wakh rék merci serigne khadim bousso❤
Yalna nagnou yalla moussale si wa pastéf
Allaahu akubar xam xam ak xalaat daal wuute na jaajëf imaam xaadim
segne khadim linga wax modou asta waxokou dh khana diglou wo wax dji dafa melni danga yakamtee reponder de
Serigne khadim man dey samab soppe nga waye tay mom danga sos ndakh s modou astou wakhoul li nga wakh toubab bi la s modou wakh waye wakhoul magni tapon serigne bi
Moodu asta amul xam xam
Dieuredieuf Serigne khadim
Bousso dou sene morom yaléne epou kham kham ❤❤❤❤😊
Jarajëf Bousso lii rek lañuy xaar ci yew
Machala
Lii deugg Moyy dankéneuh warr soriii loolll wayy politique yii défné sénii kilifeuh.
Chaytan minkii dokhh ciii Diakhassé Mourides yii ndakh pognétouu Aduna.
Wakhii gnak neuh au téguine te dareuh rafétou sii wayé S Khadim bousso yonoukk Mouride sokhla naleuh sii lénennn loudoul plateau Jakarloo TFM, soriiL politique guii té khamnii dousseuh tieurr. Lolou Moyy Degg
Bilaye khadim bousso nitou deugg LA senegal ersan bi fenne AK sa intere rek Serigne mbacke mbacke Yi topou sonko aye domou khrame pire lagne
Yangui diakha sèdè wakhol talibèyi Touba bi la done wakh
Ñi dañu sankou wallahi tudu serigne bi di tudu sonko lulu ak rér deguele 😭😭😭😭
Jërëjëf buso
Serigne Modou merci beaucoup
🥰😍😍
Magui Toubb bu bakh Sétaan naa Émission bi wayé li S.Khadim di tontou S.Modou Asta wakhoul loolou, dafa wakhné Tubaab yi diappé wounko won diaamu Yalla wayé ay khalatt lanko diappé. Wakhoul Taalibé yi, Donté li S.Modou wakh andou maci
RAFAH TV nawnaa lénn lool wayé délén séytou wakh yi doog ko dugal ! Serigne bi mo dakha jaamu Yalla ñépp Geune ko séllalé ñiepp lolou lako Taalibé yi toppé moukoy déf ci ñiom, Giss giss bim am di yééh nitt ñi ci jamu yalla nak mo takh Toubaab jappouko,,,, Wayé li Modou Asta wakhné daxou kofi kénn té geunou ko Séllalé kénn lolou rék moy Fénn yi jara tontou ci wakh ji dou lénénn
Diadief serigne khadim
Machalla Serigne khadime khame khame dou pekhé.
Khadime Busso Li nga wax ki waxou ko
Machalla serigne khadim bouss yalna kham kham bi yokko mna dè buege na soko wayè douma ko dè nda lè ak serigne touba serigne touba rèk kosiy topo socsi topo
Modou astou Mii xamut te daa wara noppi
Monsieur bosso fi 'guay wakhe soufena Di tontou sambok dakh marieme Faye .sakham kham amoute diarigne mbacke Boussouf Lou Serignebi don bagne leupe Lou eupeu si yene yena ngokoye def.khaliss 'noleco amer bakhna djiguene nonou casaliika. Li mata wakh moy li guene Di def si chirk moy yala
imame wakhoule nji and one ak serigne bi wayè yènène nitou yalla yimoufi nèkalone tè toubabi mèyoléne diam laye wakh
Moudou assto mbakce diambar la waye dafa appuell sy ay wakh
Modou astou bi khamul limy wakh sakh billahi ndakh bari wakh
Rero amna dh Serigne Astou touba yila wakh wayé wakhoul talibé yi
Jërëjëfé Serigne khadim bousso
S Modou astou AK cheikh Barra Ndiaye gno Guena Dof fii bilahi sonko diarouko bakh dokh léne rék
Yen borome commenter yii nga xam saa nga rék moy s'en solution delen téwlou dora commenter lii moudou astou Mbackè wax ay fén Serigne Touba mo këuna mana diamou yàlla ba nopi këun ko dakh séllal koudoul mome moudou bayil sa wax you soufé ame na loo xam sonko diarou ko macky diarou ko niaku ngeen tégine lool té xamadi
Dieredief Boussou
Mai. Khadima bossou Xana deg Lo wo ko
Daga dégul fim waxé rekkk
Khadim busou Li nga wax ak Li kii wax du bénne yaw dafa mélné diakhasé ngay déff
Mane DH Lima duege ak ligay tontou bokol DH mana am nak Yako apou xam xam
Man dh pare na si sonko
Modou astou Mii daa euppeul te reew teyit xamut dara
Yow busso nafékh bu bon nga domu kharam dégue nga ndakh fi nga nékon wakh bu gnaw buné wakh nga ko cheikh béthio ta cheikh bi limu lingéyal Serigne Touba sa Baye défuko
Yeen wa Rafa tv bayi leen manipuler yi ngendi def lee du seen thiéurr
Khadim bossou legui dagua wayadi tu n t sens pas a l aisse doul🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 fi diamono tolou serigne touba idéologie
Bousso yaw linga wara wakh doko wakh loulou moy sa prolem
Mame ndiaye savon mi kañ laye arrêtez tamit
Ce khadim bousso là il se prend pour qui?
Bayyilén Di djiabolisé waxi nit gni
Modou asta nopil te payi fene
Kii wakhoul diapp talibé yi déh diapp toubab bi lay wakh
Man dh amna mbetteel Lol ci waxji
Mor asta bi AK chiekh thioro bou pastef vrai nafekh rouss na sante bi sene genre Yi nioye marche Touba vrai imbéciles gni Dee d'où malenne diox benne thieur wedi n'a lenne
والعياذ بالله
Je suis désolé de le dire ainsi mais à mon humble avis, Serigne bi Bousso, tu es dévié de ta trajectoire car tu es maintenant dans l'invective politique et le renvoie de l'ascenseur aux adversaires politiques.
Il faut arrête de parler car plus tu parles, plus tu devoiles ta face politicienne car les paroles trahissent ta pensée.
Au nom du ciel, reviens dans la daara et occupe toi de l'enseignement des aspirants et laisse les politiques derrière toi quelque soit ce qu'ils ont fait pour toi.
Jaaraama
Bayileen déformer wakhi jambour ! Kii toubaab yi lawakh wakhoul taalibé yi
S khadime kii jarul tontu
Il é ten k yonou mouride comencé di douma watt daguay dégg ay cretin you khamoul touss di wakh rékkk
Serigne bi bayil politique bi makiy Sall diaroul di rero ak say mbock nion talibe yi dano am nakhar am gatche
Serigne Modou Asta lu wér la wax
Yaw mii raga lall yàlla kii wax fi ay kathie nganan lane
Ioe mii yaa wara ragal Yàlla ba noppi dook koo digal keneen kii limu dafa leer dani Serigne Touba tubaab yi jàpp ñu ko woon ngir julli ak woor ak jaamu Yàlla waaye gis gis bimu amoon lañu ko jàppe.
Khadim bousso khamoul tousse
Loolu de dou deug sama xarite
Lolou sa Serigne douko wax Serigne abdou karime mou baax mi déga xamoul sa pope rek
Xaadim Busó Bàyyil Duul Xaalis Rekk Moola Tax Di Wax
Xaadim bousso dou sen morom ci dara
Lii rék la sonko déf ci saa nga koulen këuna dioup ëup len xame xam
Waxji appna lool
Togn gui eupeuna wakhal ta guene si sonko votre ennemi n’est lui mais les wahhabistes que vous déteste comme des animistes 😢
Machala