A la place des jeunes ou de l'ASC j'allais arrêté de jouer zu football mais avec le comportement des Baye kFall y'aura morts d'hommes à cause de leur comportement
Yakham waye do ab mourit ta seringebi mourityi lay digagal ngioom lakoy tere ak ngi deuk birr touba noune de Bayinane foot ball ngir yalla ak seringe touba bako seringebi tere lanko bayi
Sa salon keur baye dessna fa football? Aramoul si yow,wayè nioune mouride lou serigne bi di terreè niou aramalko lolou moy sounou mousslay ak sounou karanguè tay ak euleuk.salam
Kom sol maillot football nguéni bagne esk dou guén commencé si boutique yiy diaye maillot si marché bi après nguén tek si télévision 📺 yiy diviser matchs yi
Nékouléne di deug dé, vous profitez du ndigueul du khalif pour agresser et volés lrs biens d'autrui en plus de votre comportement de ne pas accomplir les recommandations de Dieu vous dites recommandations du khalif
De ma part personne je suis pas d'accord avec vous parceque togne bakhoul kou dem ba mbacke Di fa football kokou defoul Dara Ay thiakhan bakhoul xallé yi woor malle deukeu bi motah niou dem mbacke Di fa football
DIEUREDIEUF serigne dame fall yague fii lool tee ande ak werr
YALLAH ak yonenté ak Serigne Touba ci ñak julli lañu teukkoo mais pas football 😮😮
Machallah ❤❤❤
Machalla ❤❤❤
Ma challàh Amna solo trop yaram ❤
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup ❤
Waw gooré waye amna sollo diedjifeu tawefekhe rék ak taysire machaalah
Dieuredieuf serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Dieureudieuf ❤❤❤
Masahalla serigne dam amna solo loll 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machalla.amna.solo
Waaw goor
A la place des jeunes ou de l'ASC j'allais arrêté de jouer zu football mais avec le comportement des Baye kFall y'aura morts d'hommes à cause de leur comportement
Maname touba sou diakha so rk Serigne sè takh bilahi
Deugeur bopou wésouwoul nékeu keur diambour borom keur gui néla beugou mali sam keur ngani dobayi limouy tére si keureum
Machalla
DIEUREDIEUF borom touba diarama mame cheikh IBRAHIMA fall
Nongi seeni ganaaw inchallah ndigël rék
Ana touba ak association football man waadioryi niooma diaaxal rekk lii amlèn yarr baaxna
😂😂😂😂😂 setani football darra nekou si
Mangui guise rayanté bouy wadia nieuw entre baye fall yi ak supporter yi
Ma guena beugue s touba guena beugue cheikh ibra mais football guisou ma kouma ko mana ayè
Yakham waye do ab mourit ta seringebi mourityi lay digagal ngioom lakoy tere ak ngi deuk birr touba noune de Bayinane foot ball ngir yalla ak seringe touba bako seringebi tere lanko bayi
Mane dé kou dioubadii la mais touba mom fasouma yené mouk difii deff lou nehoul Serigne bii magui yalla mou diap léma siii
Déme Wole Nonu DH Kou supports Ji won la NIOU gagné len finale niouné len dageu déme si diouma Ji dibjubilé Loulo yanowole mana sax
Machala yalla n'avait yalla dimbali
Khale touba s k ay mourid lang 😮😮
Mande Touba la dague waye amna si ay Khale you rew sakh
Bilahi deuge la khaleyi amlene nouke talibe waye te yalla takhe waye barke mame chiekhe I khoule khabime
Amna solo lol Fall yaram. Rewande rek ak niak kilifa
Sén sëriñ yoo yu di nàn sàngara ngéen wara waxal ba paré
Akassa
Rendez les portables des jeunes
🙏 Football yalla terre woukou sports la rek xaramoul🙏🙏🙏
Demal footbal sa küre baye
Mai ki mome deukem amna droit ni bou kéne foot ball thi ap deukem wala
Sa salon keur baye dessna fa football? Aramoul si yow,wayè nioune mouride lou serigne bi di terreè niou aramalko lolou moy sounou mousslay ak sounou karanguè tay ak euleuk.salam
Kom sol maillot football nguéni bagne esk dou guén commencé si boutique yiy diaye maillot si marché bi après nguén tek si télévision 📺 yiy diviser matchs yi
Iow dh sa xéll da neukh🤐
Walahi jinou diape day len provocé togne len diape len
Yaw yadip khathi bane ndiaringe la amal bay fall yi di diap koudefoul dara
Yallah xamna ni ki limou wax dara dousi deug
Kabiyo nél baye fall yi kérok sono nguine thie wate bi
Djieguen gni di sol toubay di dem messere yonou darou mousty feth di way règlent yarou gnoun filagnou yaro masougnou setani ay fo te wagni woun dara
Mara bi mome ap dof la
Ak tooñ daal baaxul si dëkk lani aayee futbool mais ku dem ba mbacke sétan limiy seetaan dëpp ngani dang koy japp
Lu ci saw yoon
linga wah leppu deuguela, lifi serigne bi beugue rk
Khana gniy dém mbacke soirée welly seck le 25 décembre gnép nguéni diap
Saw yoon neku ci
Ñi daño rewe
Ku ngéen japp noq leen ko ba mu day dok ko baayi
Boune diapone sa bay nokhou ko do wakh li
Wa li mom état douci Wakh mbetei ay policiers Bay gracié 😂😂😂😂😂
Yaw kaay wakhsi seringe momoom deukbi
@ deuk bi kan moko mom liamay wakhatei ngui nekal nit la Wakh😂
Kou fi foot ball gnou gnaff sa ndaye
Wa goor
Si dofi nga bokou dh 😂
Wakh deugue yall deukk bi kenu football loufi karr aÿ nitt you diougé Mbacke di diaye gooré
Fi kou nékh déba Mbacke yéne démléne diamoudie yalla sangara mo guene aram
Yow ya wara jamu ji yalla té bayi tooñ
Dama fall wakou fii dara daga bariu wakh rk
Borome keur yi tih dieumeum nio diapale woul Serigne bi
Fall deff len si niom li war nop bu deugul beut gis
Nékouléne di deug dé, vous profitez du ndigueul du khalif pour agresser et volés lrs biens d'autrui en plus de votre comportement de ne pas accomplir les recommandations de Dieu vous dites recommandations du khalif
De ma part personne je suis pas d'accord avec vous parceque togne bakhoul kou dem ba mbacke Di fa football kokou defoul Dara Ay thiakhan bakhoul xallé yi woor malle deukeu bi motah niou dem mbacke Di fa football
Wakhofi dara
Dem liguéyi
Football Xaramul
Démlén diamou dji yalla
Wakhofy daara
Kofi fotbal nio teppi sa leufeul ndeye rew doumo ram yi
Démlén diamou djiy yalla
Gni noguana dioubadu
DIEUREDIEUF borom touba diarama mame cheikh IBRAHIMA fall
ماشاء الله