La Réponse de Cheikh Tidiane Bitéye à Oustaz Oumar SALL

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 13 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 524

  • @mbackesow2852
    @mbackesow2852 4 ปีที่แล้ว +24

    Macha Allah oustaz cheikh Tidiane Biteye tontu amna solo yala deugu la beugu sose bakhul

  • @moustaphafall2353
    @moustaphafall2353 4 ปีที่แล้ว +37

    Oustaz Oumar Sall yalla nafi yageu ta wérr yalla nala yalla fay sa khoul

    • @producewarriors6156
      @producewarriors6156 4 ปีที่แล้ว +4

      Bouko yalla fayé kholam rek mou grave 🤔
      لامن قريب ولا من بعيد ay ndarr rek

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว +3

      Wakhal key Yalla nako Yalla sopi mou dém ba khamé deugue bayi sose inventé

    • @dioufaliou4683
      @dioufaliou4683 4 ปีที่แล้ว +2

      Omar sall kay boumifi yag ndakh loumouy wakh lousi baari dou deug

    • @dogodiop5188
      @dogodiop5188 4 ปีที่แล้ว

      Amine inchalla mé nitt day wakh degg sa yalla laneu la wakh kou gueneu adina bo meunul wakh lou bakh si mome nopil

    • @medounendiaye5489
      @medounendiaye5489 3 ปีที่แล้ว +1

      Oumar Sall doul rek ngay def domeram jii

  • @pakhalil6876
    @pakhalil6876 ปีที่แล้ว +3

    MERCI OUSTAZ BITEYE ligue wakh lerr na nagn deug dou moromou fenn akk soss

  • @fatimaba1788
    @fatimaba1788 4 ปีที่แล้ว +32

    Oumar salle mon père adore je t aime je veux que tu remets tout a Allah car c'est pas facile tu es un soldat de l Islam n écoute pas les gens surtout les gens qui font tout pour t faire taire continue tu travaille pour Islam j jure que je celui qui parle pour Allah sais que tu es un homme d Allah car tu ne fais que de nous dire ce qu Allah attend de nous donc courage nous nous avons si tu étais un homme qui parle sur tes passions ou chercher quelque chose tu allais leur plaire les gens qui pensent a la mort sont avec vous les égarés son contre vous moi je dis que tu es sur la voie prophètique qu Allah te protège

    • @ismailacamara6733
      @ismailacamara6733 4 ปีที่แล้ว

      Bien dit frère

    • @moustaphagoumbala1804
      @moustaphagoumbala1804 4 ปีที่แล้ว +2

      Nko mou fot hol bi sohor na trop

    • @hawaba7795
      @hawaba7795 4 ปีที่แล้ว

      Wallahi ma sœur ta parfaitement raison oustaz mom yalla mou goudou fann ak wer inchaallah

    • @bassiroudianka7373
      @bassiroudianka7373 4 ปีที่แล้ว

      mashallah content de toi

    • @daoudandao7559
      @daoudandao7559 4 ปีที่แล้ว

      Machallah Soxna Fatima Wax nga lepp

  • @ousmaneseckjeunedeputedere9559
    @ousmaneseckjeunedeputedere9559 4 ปีที่แล้ว +24

    Omar sall DEUG la wakhe

  • @soldierbamba6307
    @soldierbamba6307 4 ปีที่แล้ว +22

    Dama xamoul nane gay dieuléee say mbokk dioulitt dileen touddée ay nittou biddha

    • @laminendiaye4705
      @laminendiaye4705 4 ปีที่แล้ว +2

      Ñoom buñu accepter né bidah hassana amna waroo bañ ñu tuddéela nittu bidah

    • @laminendiaye4705
      @laminendiaye4705 4 ปีที่แล้ว +2

      Liwaraloon Oustaz Alioune Guèye (rahimahu Allah) démissionner ?

    • @papekandji4972
      @papekandji4972 4 ปีที่แล้ว +1

      Ah encore CES oustaz

    • @dighkdlgfh9005
      @dighkdlgfh9005 3 ปีที่แล้ว +1

      Koussi bòkk guiss ci sa bòpp

    • @alphaoumardiallo3884
      @alphaoumardiallo3884 4 หลายเดือนก่อน +1

      Xana rèwandé rék moko meune ak bone bo xamné foko takk wèsou nako

  • @saliouniang9793
    @saliouniang9793 4 ปีที่แล้ว +16

    Yalla na yalla same oustaz oumar sall té same gnieup alkhourane ak sounna 💗💗

  • @kanedayah8160
    @kanedayah8160 4 ปีที่แล้ว +9

    Ce qui est sûr c’est que Oumar Sall ne ressemble pas à un menteur 🤥

    • @mbackesow2852
      @mbackesow2852 4 ปีที่แล้ว +1

      En tous cas le témoin de toute l'histoire a répondu et oustaz Omar Sall n'était pas témoin des faits

    • @babacarthiam157
      @babacarthiam157 2 ปีที่แล้ว

      Omar Sall fenkat bou Mak la

    • @h6galsen712
      @h6galsen712 ปีที่แล้ว

      Mendoul

  • @ablayesow9938
    @ablayesow9938 4 ปีที่แล้ว +12

    Oustaz oumar Sall Mach Allah yalna la yalla takhawou méla goudou fane ak moudju bou rafètt alkhourane ak sunna si kanam

    • @ndiayeamadou150
      @ndiayeamadou150 4 ปีที่แล้ว +2

      omar sall domarame boumack leu dou dara fenn rek lay deff

    • @cheikhmamenguer8506
      @cheikhmamenguer8506 4 ปีที่แล้ว +1

      en SOS ak ay fén moy souna OK lérna

    • @lahatleye6313
      @lahatleye6313 3 ปีที่แล้ว

      Dioulit du fénn

    • @medounendiaye5489
      @medounendiaye5489 3 ปีที่แล้ว

      S'en oustaz bii doul rek lay def 😆😆

  • @Lk-to7kr
    @Lk-to7kr 4 ปีที่แล้ว +10

    Me yen lane moy sen problem oustas omar yalla mokay sam te same quepp kouye dioulite baylen togne

  • @Se-soigner
    @Se-soigner 4 ปีที่แล้ว +15

    Respect zéro mouy Oumar sall wala cheikh biteye notre respect. Koumou fi donone sa wadiour do nangou kou ko saga. Dioulite waroul vulgaire. Mane nga wax té dépasser wo kenneu.

    • @jassansene9623
      @jassansene9623 4 ปีที่แล้ว +1

      Oumar salle limouye wakh yalmo takh

    • @mamadousadiodiallo2433
      @mamadousadiodiallo2433 4 ปีที่แล้ว +1

      kan la meussa sagua arrêtez d'exagérer et être véridique c mieux k de porter de fausses accusations sur Omar Sall c koi le problème au Sénégal

    • @modousagna7902
      @modousagna7902 4 ปีที่แล้ว +1

      Fen mo geune graw kon amoul maslaha

  • @laminediame133
    @laminediame133 4 ปีที่แล้ว +9

    Machallah oustaz Oumar Sall.Sunna rék bé faw inchallah

  • @magayecamara1565
    @magayecamara1565 4 ปีที่แล้ว +24

    machallah oustaz oumar sall ☝🏾🕋🤝🏾👍🏾

    • @youssoudiop4148
      @youssoudiop4148 4 ปีที่แล้ว

      Son problème se son les tariha seulement ils vas se fatiguer pour rein du tout dayesane

  • @sidybouyadiagne5908
    @sidybouyadiagne5908 4 ปีที่แล้ว +13

    Omar sall ragalal YALLAH dioulit dafay wakh deug

  • @oumarfaye6855
    @oumarfaye6855 4 ปีที่แล้ว +18

    Oumar sall ne parle pas sous l'effet de sa passion ni par fanatisme

    • @papesambousidibe6567
      @papesambousidibe6567 4 ปีที่แล้ว +1

      Sunna niata bount la

    • @assanembow6453
      @assanembow6453 4 ปีที่แล้ว

      Oumar Faye il par la rencunier

    • @ousmanendiaye6817
      @ousmanendiaye6817 4 ปีที่แล้ว +2

      Es doule yak omar sall

    • @assanembow6453
      @assanembow6453 4 ปีที่แล้ว +3

      Oumar Faye il est grand menteur so dougué youtube tu vera c vidéo de mensonge dafa boon te dioulite dou boon

    • @abdallah3165
      @abdallah3165 4 ปีที่แล้ว +1

      @@papesambousidibe6567 fo deugue ni sunnah dafa am. Bountou yaw ? Islam mo. Am bountou aki ponk sunnah louniouy top la diko doundou nako yonente bi dane doundé boulene rereul sene bop

  • @ndiouroultv3991
    @ndiouroultv3991 4 ปีที่แล้ว +15

    Oumar sall diaroul di tontou ndakh dou wakh deug

    • @adamadmx6441
      @adamadmx6441 4 ปีที่แล้ว

      ya moun doul

    • @alhajigueye5647
      @alhajigueye5647 4 ปีที่แล้ว

      عمرسال كذاب

    • @ndiouroultv3991
      @ndiouroultv3991 4 ปีที่แล้ว

      @@adamadmx6441 ok sagal noumoula nekhé waye Nangua khamné omar sall nafekhla te amoul kham kham

    • @ndiouroultv3991
      @ndiouroultv3991 4 ปีที่แล้ว

      @@alhajigueye5647 ñiaka wakh deug dafa book li wahabiste yiii te yalla takhoul gnouy wakh

  • @sadieyetall7177
    @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว +17

    yén wa sounna ngén bagne
    sounna molén déranger
    yén wa Ahlou bida
    sounna si kanam rék

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว +1

      Nonou ba légué dégoulén dikoulén té wessoulén diamniado

    • @talibebamba5450
      @talibebamba5450 4 ปีที่แล้ว +2

      Non terroriste wahhabite yi lagn bagn 😂

    • @amadoutidianeba37
      @amadoutidianeba37 4 ปีที่แล้ว +2

      Non sen fenyi laniou bagne. Danguène mouna fen. Yen wa ahloul fen.

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว +1

      @@amadoutidianeba37 ioe gni mouno lén enlevée Li gnouy wakh alquran ak sounna rék.
      soula déranger déwall sounna thia kaw thia kanam 💪

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว +1

      @@talibebamba5450 waaa ioe khôl mo diékh kén topou fi sen Serigne yénénti bi rék la gniy topp mome la yala wakh gnou Topp koo 😂sounna thia kanam rék 💪soula déranger déwall 😂😂

  • @babacarndiaye2283
    @babacarndiaye2283 4 ปีที่แล้ว +28

    Cheikh tidian bitey moféké kayy wax deugeu momana wax li khew

    • @bathiembaye7833
      @bathiembaye7833 4 ปีที่แล้ว +2

      Oumar sall fen rek lay ligueyeul domou haramla rek

  • @lkane7110
    @lkane7110 4 ปีที่แล้ว +4

    Non kon lémotakh gayi di saga Omar sall thiéy mém rèw. Merci Omar sall yalla nala yalla sam arla barki s mhmt

    • @mbaye.sndoye6744
      @mbaye.sndoye6744 4 ปีที่แล้ว +1

      omar sall da mandouwoul si mbirou diambour yi

  • @kanteyoussou4965
    @kanteyoussou4965 4 ปีที่แล้ว +6

    Oustaz oumar sall niongi sa ginnaw ba kerok yowmal hiyam lounioula sosal si adouna dou tah niou bayila ahlou souna a vie ❣❣❣❣❣❣❣❣❣

    • @hawaba7795
      @hawaba7795 4 ปีที่แล้ว

      Allahouakbar wallahi wakhga deug pur quelque soit alpha dougniou la moussa bay inchaallah

  • @CheikhounaBadiane-h7f
    @CheikhounaBadiane-h7f 4 หลายเดือนก่อน

    Machalla ostas cheikh tidiane bitiy kha khame bosella ta rafet kit ko Landi yalla Yoko takkhawaye bi

  • @serignesalihoufall8512
    @serignesalihoufall8512 3 ปีที่แล้ว +2

    WAW LOUTAKH OUMAR SALL MEUNA FÉNEU

  • @allkaloallkalo1413
    @allkaloallkalo1413 4 ปีที่แล้ว +7

    BITEYE vous allez mourir pour la jalousie inchallah DIEU ne délaisse jamais AL OUSTAZ OMAR SALL tant que il est basé sur le CORAN ET LA SUNNA UN contre tout vous allez échoué votre combat sera vain

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว

      Ahhh bon,on est en train de convertir des millions et des millions d'égarés à travers le monde,il n'a jamais dépassé bountou pikine..combien de personnes il a converti?ce bavard n'est rien du tout et représente rien

  • @laminediop2822
    @laminediop2822 4 ปีที่แล้ว +6

    Cheikh Omar Sall est l'homme de vérité quant à l autre je la connaît pas???????????

    • @mbaye.sndoye6744
      @mbaye.sndoye6744 4 ปีที่แล้ว

      akh nitt dh loko hamaloul boussi wahh. Mashalla linga ham si omar sall wahngako tei mandou si kenen ki. c un exemple nitt day wahh louko woor bayi par parloo.

    • @daoudazoubairou7741
      @daoudazoubairou7741 2 ปีที่แล้ว

      Fenn kaat le guanan homme de vérité

  • @djilydieng6974
    @djilydieng6974 4 ปีที่แล้ว +7

    Waw gir oustaz bitéye lérna naña

  • @damedame4228
    @damedame4228 4 ปีที่แล้ว +22

    No biteye mo nafekh ki momana doul li moye tassawouf non

    • @elhadjifallousarr3467
      @elhadjifallousarr3467 4 ปีที่แล้ว +3

      Nèl sa oustaz mou bayi fèn

    • @younoussebodian7960
      @younoussebodian7960 4 ปีที่แล้ว +4

      Saway il y'a 2 versions
      Ki wax ni deg na
      Ak ki wax ni feké na
      Je prefere croire à celui qui dit que fekéna
      Wassalam

    • @assanembow6453
      @assanembow6453 4 ปีที่แล้ว +3

      Omzo salo feneu rek la meun

    • @moustaphagoumbala1804
      @moustaphagoumbala1804 4 ปีที่แล้ว +1

      Omar sall moy n'a fek

    • @fairevoyagerlesprit
      @fairevoyagerlesprit 4 ปีที่แล้ว +1

      @@younoussebodian7960 T'as pas compris bro, Oumar n'a fait que transmettre les propos, donc Biteye n'a rien á dire.

  • @papetall1951
    @papetall1951 4 ปีที่แล้ว +7

    Machalla oustaz cheikh

  • @amiradelislam3789
    @amiradelislam3789 4 ปีที่แล้ว +21

    100%yaw nagn beugue.ana wa القرآن والسنة

    • @saliouniang9793
      @saliouniang9793 4 ปีที่แล้ว +1

      Nogui ni

    • @papaalgye3499
      @papaalgye3499 4 ปีที่แล้ว

      Mane deh Alhourane ak Souna rek mais pas come les wahabistes et les terroristes

    • @talifakdiangoumrajasst.d.r5505
      @talifakdiangoumrajasst.d.r5505 4 ปีที่แล้ว

      Kouy doundou alkhouranak souna waroul doul fén bakhoul

    • @mouhamedndoye7305
      @mouhamedndoye7305 4 ปีที่แล้ว

      Niogui nii

    • @ouakamedakar4209
      @ouakamedakar4209 4 ปีที่แล้ว +1

      Yén ay dof géun kouy dioulit si alhouran ak souna nga nék oustas omar Sall day doul rek

  • @bigsanguinaire5822
    @bigsanguinaire5822 4 ปีที่แล้ว +25

    Oumar sall la gueume wakham

    • @awayacinesylla
      @awayacinesylla 4 ปีที่แล้ว +1

      C ton problème toujours il aura des nafekha al mounafihoune

    • @arahma3284
      @arahma3284 4 ปีที่แล้ว

      @@awayacinesylla
      th-cam.com/video/IlX61FdifZw/w-d-xo.html

    • @mbackesow2852
      @mbackesow2852 4 ปีที่แล้ว

      Far farloo gua dèff cheikh Tidiane Biteye est témoin des faits car c'est lui qui a fait les démarches alors oustaz Omar Sall n'es pas témoin fékèwul Kone wakham werul

  • @cheikhsp3188
    @cheikhsp3188 4 ปีที่แล้ว +6

    Deugeu leu cheikh tijane

  • @fairevoyagerlesprit
    @fairevoyagerlesprit 4 ปีที่แล้ว +4

    yaw Oustaz oumar sall daffa né diw mokoko wakh, tei watt nako si yalla, legui yaw féké woko beug wéddi, Biteye ya degeur fitt. TOGNE NGA OUMAR SALL

    • @mbaye.sndoye6744
      @mbaye.sndoye6744 4 ปีที่แล้ว +1

      yaw loula wooor ni omar sall limou wahh deug la tamit am nga fitt daal

    • @fairevoyagerlesprit
      @fairevoyagerlesprit 4 ปีที่แล้ว

      @@mbaye.sndoye6744 niar niou wakh loussi yonam? daffa fékké bi alioune gueye (RIP) di wakh ak Oustaz Oumar sall

    • @mbackesow2852
      @mbackesow2852 4 ปีที่แล้ว +1

      Yaw deglou woo sakh Di wakh Biteye fèkèna khew khew bi

    • @mbackesow2852
      @mbackesow2852 4 ปีที่แล้ว +1

      Tè mom en personne mo dokh si gneuwattu oustaz bobu

    • @ibrahimacoulibaly844
      @ibrahimacoulibaly844 4 ปีที่แล้ว

      Omar sall gnou dé gni rek lay sossal

  • @sulaymanediallo6209
    @sulaymanediallo6209 ปีที่แล้ว

    Que Dieu aide et garde ça religion islam et les gens qui le suis sans l’associé à rien

  • @sincerite64
    @sincerite64 4 ปีที่แล้ว +1

    Kone lernaa...Ab Oustaz bu Ragall YALLA Warta wax si babeeexou bakanam

  • @arahma3284
    @arahma3284 4 ปีที่แล้ว +6

    I love Oustaz Omar Sall And I trust him...
    Sama Serigne "Oustaz Omar Sall" tontounako bo paré : 👇👇
    th-cam.com/video/IlX61FdifZw/w-d-xo.html
    Bitéye kou niawe diorte la , té niake teguel ak yare

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 4 ปีที่แล้ว

      Peace cest un menteur ce mec domar sall là tu aimes un colochard donc

    • @modougueye7451
      @modougueye7451 4 ปีที่แล้ว

      Yaw omaraye sa serigne

  • @khadimleye5738
    @khadimleye5738 4 ปีที่แล้ว +4

    Oumar sall gnaf ndm rek mo bah ci mome

    • @masiba7272
      @masiba7272 4 ปีที่แล้ว

      Bounou niafee sa nday ba nopi

  • @momoseck2508
    @momoseck2508 4 ปีที่แล้ว +2

    Bilay omar sall kathiore la

  • @mamadousane7958
    @mamadousane7958 4 ปีที่แล้ว +1

    Kou dé ak sa bamel tei dara diaroul di até ay nitt solén khamoulé ... man dei dounde na ak oustaz Omar Sall wayé nitt geunouko deugou nagnou bayi khel biss penc ndakh saga ak wakh diou niaw deukoul famou dieum famou diogué la deuk bal kou yarouwoul ak ki gnak diokh tieur ay waydiouram mokoy fowé 👌👌👌

    • @iboudiouf7673
      @iboudiouf7673 5 หลายเดือนก่อน +1

      Geunoul degou kén fi 😂

  • @patrickdoucet7753
    @patrickdoucet7753 4 ปีที่แล้ว +1

    Vive Oustaz Oumar Sall défenseur coran ak souna.

    • @mbaye.sndoye6744
      @mbaye.sndoye6744 4 ปีที่แล้ว

      omar sall ne fait qu'augmenter la haine au senegal

  • @amadouba285
    @amadouba285 3 ปีที่แล้ว +2

    Ousta Oumar Sall yalla nala yalla defal damou

  • @elhadjimodoudiop1107
    @elhadjimodoudiop1107 4 ปีที่แล้ว +8

    Daffa meunneu feinn dhé oustaz Oumar sall rk😃😃

  • @mackysallbadolala600
    @mackysallbadolala600 4 ปีที่แล้ว +5

    Beteye beteye Oustaz Omar Sall wakhoul ak yaw te liniou guiss si mom moy nitt kou deugou la

  • @manseyegaye1559
    @manseyegaye1559 4 ปีที่แล้ว +1

    12. O vous qui avez cru! Evitez de trop conjecturer [sur autrui] car une partie des conjectures est péché. Et n'espionnez pas; et ne médisez pas les uns des autres. L'un de vous aimerait-il manger la chair de son frère mort? (Non!) vous en aurez horreur. Et craignez Allah. Car Allah est Grand Accueillant au repentir, Très Miséricordieux.

  • @massatandiaye9242
    @massatandiaye9242 4 ปีที่แล้ว +4

    Sante s Touba

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว +1

      Lolou dou débat bi..

    • @Se-soigner
      @Se-soigner 4 ปีที่แล้ว +1

      @@adamasow9292 walay hors sujet rk

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว

      @@Se-soigner gni key moye lolou toujours out !!

  • @bambodiakhabytagaya4477
    @bambodiakhabytagaya4477 4 ปีที่แล้ว +5

    Oustaze Omar sall j'ai écouté tous les deux toi et biteye. Mais biteye est plus claire en explication sur le cas. J'ai attendu le mot de biteye pour répondre mais Omar sall cette fois ci je ne suis pas d'accord avec toi désolé assalamou Aleikoum

    • @ebrimabarry2147
      @ebrimabarry2147 4 ปีที่แล้ว

      Bonjour mr Bambi Omar Sall relate les faits qu'on lui a reconté il n'a jamais dit qu'il été présent lors des faits encore moins que ce que l'oustaz était vrai il raconte juste simple.ne confondez pas

    • @maguetteloum946
      @maguetteloum946 4 ปีที่แล้ว

      Mousso d'accord ak Oustaz Oumar Sall daguay fén

    • @lahatleye6313
      @lahatleye6313 3 ปีที่แล้ว

      @@ebrimabarry2147 néxull laayal

    • @mawdomalickpouye316
      @mawdomalickpouye316 ปีที่แล้ว

      @@ebrimabarry2147 wadji dafa wara bayi di nétali loumou fékéwoul motakh dou diouk si fén na diéme wakh ak gnidoul djioulit gnou doug si diné bi moo gueun di wakh si lo khamni yonam nékou si

  • @youssoudiop4148
    @youssoudiop4148 4 ปีที่แล้ว +1

    Oumar salle sont seules problème se çon tariha toujours il Di jeune SIPA peureux mais peureux de Koi mais onné an démoncrasi vous disait toujours Buda mais les nanfila que vous faites dans les mosquées Mohamed n'a la jamais fait comme vous le faites et Tan d'outre

  • @mamadoudrame2054
    @mamadoudrame2054 4 ปีที่แล้ว +4

    Longue vie à toi oustaz Omar sall le véridique

  • @mamadoudieng6164
    @mamadoudieng6164 3 ปีที่แล้ว

    mai svt le fond sonore nous empêche d'écouter

  • @wabaye75
    @wabaye75 4 ปีที่แล้ว +1

    Walahi alioune sall limouy féne meunaa laakh guédj!!!

    • @sstm7845
      @sstm7845 4 ปีที่แล้ว

      Oumar Sall la de

  • @ahmadoumboup7117
    @ahmadoumboup7117 4 ปีที่แล้ว +3

    L’argument de Biteye n’a ni sens, ni message, ni valeur. Les Musulmans Senegalais ont besoin d’autres choses que des “ya wakh, ma wakh, ma am deug.” Que Dieu nous guide.

    • @elhadjidiop7332
      @elhadjidiop7332 4 ปีที่แล้ว

      Oumar sall mouy feinn kay doleinn ko wakh

    • @dijadija7000
      @dijadija7000 4 ปีที่แล้ว

      @@elhadjidiop7332 ya meuna doul daga ko faiker meuna daye

  • @modoumamendiaye691
    @modoumamendiaye691 3 ปีที่แล้ว +3

    Omar sal bayill fen 😆🤣😂😅

  • @cheikhgueye9944
    @cheikhgueye9944 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalla oustas

  • @moustaphandiaye6876
    @moustaphandiaye6876 4 ปีที่แล้ว +3

    Omar sall fene rek lay def limouy wakh dara lasi hamoul

  • @boubooombayeeede6388
    @boubooombayeeede6388 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalla Chiekh tidiane

  • @sadieyetall7177
    @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว +8

    yakamti ngén bén ahlou sounna bou wakh rék ba ngén tacler ko
    sounna molén déranger yén

    • @assanembow6453
      @assanembow6453 4 ปีที่แล้ว +1

      Sadieye Tall dioulite mo am mais po souna wala farata ki da bariiii soooow si diné te soxor

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว

      @@assanembow6453 parce-que lolu nga Fogg ioe ki do deglou Ay khoutbam mo takh lou nit yi di wakh rék ngén gueum

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว

      @@assanembow6453 kou sokhor dina la wakh Yala néna ak yénénti bi néna Noo ioe khamo kou sokhor

    • @assanembow6453
      @assanembow6453 4 ปีที่แล้ว

      Sadieye Tall soxor motaxx mounane yonatibi yayam mingui safara 2ème ma mouné kou deee keneu meunoula diarigne te yalla né djoulite bou baxx day rambou il refuse tt prsk da diapouné monek si dinè ls autres hors xalate sii rek

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว

      @@assanembow6453 ioe dama lay gnanal yalla thé kham ni dans nga khamoul
      yénénti bi da nga am preuve boulay won ni Yayam demoul Safara
      ioe man ak ioe sounou débat d'où Mouna sory parce-que dianguo

  • @dioufaly2338
    @dioufaly2338 4 ปีที่แล้ว +3

    Dafa kheuy bayi nga wax dh lolou meunoul nek kon dafa kheuy gnou dakk ko tmt gnoune ay borom xel lagnou

  • @abouly6953
    @abouly6953 3 ปีที่แล้ว +1

    Omar Sall bayyil fen

  • @moustaphafall2353
    @moustaphafall2353 4 ปีที่แล้ว +2

    Bitéye ragale yalla taga khoul bou bakh sa bopp

  • @maguettecisse6153
    @maguettecisse6153 4 ปีที่แล้ว +3

    Oustaz oumarr Sall do sénn morom

    • @sadieyetall7177
      @sadieyetall7177 4 ปีที่แล้ว

      contane n'a ioe dhé

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว

      Bane réw si adounabi la dém.olof rek la dégue,ki dafa kham touss

  • @KHAMKHAM-xi8pj
    @KHAMKHAM-xi8pj 4 ปีที่แล้ว +2

    Yén ay saytané nguén rék danguéna am diot démlén diamou yala mo gaun linguéni déf

  • @momoseck2508
    @momoseck2508 4 ปีที่แล้ว +2

    Omar sall sa défaut moy daga diap ni kou bokoule si akhou sounna plus particulièrement ibadou sa diamou yalla baxoule nax ga sa bopp

    • @LoveYibo-forEver
      @LoveYibo-forEver 4 ปีที่แล้ว

      Momo seck c clair ni xamo Omar doko deglou linga wakh c faut, ragalal yallah

  • @modykamaldiouf8551
    @modykamaldiouf8551 3 ปีที่แล้ว

    Oustas bitéye continue et ignorez les ignorants

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 4 ปีที่แล้ว +4

    Pourquoi ngen gem biteye ta geumou len oustaz oumar sall yalla rek mo kham yalla nanio yalla defal diam amine 🙏🙏🙏🙏

    • @GoudiabyOus
      @GoudiabyOus 4 ปีที่แล้ว +2

      Esk Oumar fékéna bamouy raconter ki féké mo nétali lini mel en tt cas Al Makhtoum dane na wakh ni mak dou féne ndakh sou féné adouna touki

    • @elhadjidiop7332
      @elhadjidiop7332 4 ปีที่แล้ว +2

      Oustaz omar sall daffa meunneu feinn

    • @lhistoiretv2031
      @lhistoiretv2031 4 ปีที่แล้ว

      @@GoudiabyOus ko bkh ki est que deglo nga niarri vidéo yi li oumar sall l'histoire bi biteye di wkh ak bi oumar sall di wkh boukoul de ko bkh ki

    • @elhadjifallousarr3467
      @elhadjifallousarr3467 4 ปีที่แล้ว +1

      Oumar sall ci bopam mo wara wax deugu

    • @mouhametthiam3388
      @mouhametthiam3388 4 ปีที่แล้ว +1

      Elhadji Diop respectell oumar sall lepp loomou wax sii sunnah lakoy tek walla hadith wala deuugg bou werr

  • @sanoufaye6970
    @sanoufaye6970 3 ปีที่แล้ว +1

    Omar sall mo dakk doulll si lou yalla bindd mom ak gniko top nieup safara laniou dieummmm te fenlo yonnet bi rekkkk thiagua you kharammm yii

  • @moustaphafall2353
    @moustaphafall2353 4 ปีที่แล้ว +2

    Yalla na yalla takhawou oustz oumar sall li geuneu bonn si adouna moy di saga nitou diné keppe kokoy saga rek dala lale si lo degeu liga nékeu

  • @yoorobalde1270
    @yoorobalde1270 4 ปีที่แล้ว +3

    Omar Sall,loudoul féén ak soss meunouko, oustaz bouy féén ak soss ci mom laako guissé...Bouy féén dou nooyi baa paaré nééna Alkhour'aan ak Sounnah laay toppou...

  • @elementssonkoofficiel6109
    @elementssonkoofficiel6109 3 ปีที่แล้ว

    Omar Sall yalla na yalla samoula

  • @zilletoure526
    @zilletoure526 3 ปีที่แล้ว +1

    Omar sall tu et avec dieu ne peur rien dieu avec toi

  • @amadoukane865
    @amadoukane865 4 ปีที่แล้ว +1

    Oumar sall bayil fénn baxoul dé wallahi.

  • @salmanediallo9001
    @salmanediallo9001 4 ปีที่แล้ว +1

    Bitey sa wakh ji yennou woul mana

    • @mbaye.sndoye6744
      @mbaye.sndoye6744 4 ปีที่แล้ว

      pask wahdji arrangé woula koi. Non senegal mo nekh

  • @dighkdlgfh9005
    @dighkdlgfh9005 3 ปีที่แล้ว +2

    Je vois le gens détestent oustaez Oumar Sall mais moi je sent beaucoup mon seigneur quand je regarde ses vidéos

  • @basidiahmed4623
    @basidiahmed4623 3 ปีที่แล้ว +3

    Oumar sall day fenn reck
    Fenn reck mooy liggey Am
    Ken warull seetan ay vidéo Am

  • @manebassirou779
    @manebassirou779 4 ปีที่แล้ว +1

    Yanna yalla sameu oustaz oumar Sall

    • @lahatleye6313
      @lahatleye6313 3 ปีที่แล้ว

      Déf ko dioulit ndax dioulit du fénn aw kama xall p s l

  • @mbayeciss1194
    @mbayeciss1194 4 ปีที่แล้ว

    Dans quel monde sommes-nous ?

  • @yoorobalde1270
    @yoorobalde1270 4 ปีที่แล้ว +2

    Billahi wallahi wa tallahi,Oumar Sall béés bou dieulé kaamiil Alkhour'aan bi,waatni mom limouy wax ci wa tassawouf deugla,diina laak ba diééx taak..'

  • @modouastadiakhatembacolmba2560
    @modouastadiakhatembacolmba2560 3 ปีที่แล้ว

    Machalla oustaz cheikh tidiane

  • @ahmadou4
    @ahmadou4 3 ปีที่แล้ว +1

    Le gars Sall est un menteur invétéré. Je me demande comment quelqu’un peut l’écouter.

  • @ibrahimacoulibaly844
    @ibrahimacoulibaly844 4 ปีที่แล้ว +2

    Lima diahal si mome gni guéne adouna rek lay fénal ki es ce ke dioulitela

    • @dioufsoda6311
      @dioufsoda6311 3 ปีที่แล้ว +1

      منافق nafekh la moom omar sall

  • @amiradelislam3789
    @amiradelislam3789 4 ปีที่แล้ว +4

    Mâcha alla oumar sall

  • @AmaouOumar
    @AmaouOumar 18 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤

  • @salioudia6358
    @salioudia6358 3 ปีที่แล้ว

    ماشا الله ostaz aline geuye

  • @manseyegaye1559
    @manseyegaye1559 4 ปีที่แล้ว

    11. O vous qui avez cru! Qu'un groupe ne se raille pas d'un autre groupe: ceux-ci sont peut-être meilleurs qu'eux. Et que des femmes ne se raillent pas d'autres femmes: celles-ci sont peut-être meilleures qu'elles. Ne vous dénigrez pas et ne vous lancez pas mutuellement des sobriquets (injurieux). Quel vilain mot que «perversion» lorsqu'on a déjà la foi. Et quiconque ne se repent pas... Ceux-là sont les injustes.

  • @ismailasarr1800
    @ismailasarr1800 4 ปีที่แล้ว

    Le diseur de vérité ouztaz oumar sall

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 4 ปีที่แล้ว

      Loumouye wakh yeup dara douci deug

  • @alphaoumardiallo3884
    @alphaoumardiallo3884 4 หลายเดือนก่อน

    Oumar sall dama rouss si nou bokk tour bou yémone si féne kessé mou tané wanté day soss day rèral nioum andal si yonu diiné billahi

  • @moussandg4659
    @moussandg4659 4 ปีที่แล้ว

    CHEIKH T. BITEY YAW KOUMA BETE NGA PARCE QUE FOGONA NE SA NIVEAU DEPASSÉNA LI. WAKHOFI DARA LOUDOUL WAKHOU KOU SOKHOR..... SALAM

    • @massambagueye2246
      @massambagueye2246 4 ปีที่แล้ว

      Ioe waxou doof ngafi wax. Mom limou fekkei kessei la wakh. Il est bcp plus clair et il a des témoins

  • @habibseye5531
    @habibseye5531 4 ปีที่แล้ว

    Kou sagna sagua neww yathia deugu kay,do roussa fénal kenn

  • @penda154
    @penda154 4 ปีที่แล้ว

    Nanla biteye meuné nekkeu chef desk religieux dunya mou wakh mouné d'où deugg. Oustaz Oumar Sall togn katteu leu

  • @cheikhamartvamar
    @cheikhamartvamar 4 ปีที่แล้ว

    Merci s cheikh t bitéy

  • @medounethiamngom7598
    @medounethiamngom7598 4 ปีที่แล้ว +3

    Dioulite day raffèt kaddu té mandou!!!yen commentateurs yii lay wakhal ;As salamou alleykoom

  • @doctorphone755
    @doctorphone755 4 ปีที่แล้ว +2

    cheikh tidiane biteye dafa gnak fayda beugue dageue santeu

  • @abdoukhadretop255
    @abdoukhadretop255 4 ปีที่แล้ว +2

    Macha Allah leral yi ame solo. Omar sall mome sétane rek ak moudiame ganna messere rek teunkal naniou omar sall

  • @ibrahimatanordiallo1382
    @ibrahimatanordiallo1382 4 ปีที่แล้ว +5

    Yèèn ngnii di saaga yarou lèène waay svp minimum de rèspect

    • @moustaphagoumbala1804
      @moustaphagoumbala1804 4 ปีที่แล้ว +1

      Omar sall mo wara yarou

    • @aidatoure6566
      @aidatoure6566 4 ปีที่แล้ว

      Wakh ko mo geum yalla te reugalko mo geun ci mom rewBakhoul

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 ปีที่แล้ว

      Sen data ndeye yak omar sall

  • @thiamthiam1666
    @thiamthiam1666 4 ปีที่แล้ว +1

    fene rek la mane omar sall

  • @damemarr2745
    @damemarr2745 3 ปีที่แล้ว

    😥😥😥

  • @AssaneFall-p9k
    @AssaneFall-p9k 11 หลายเดือนก่อน

    Sonko rek inchallah

  • @senegalrek7975
    @senegalrek7975 4 ปีที่แล้ว +5

    Omar sall domi khathie dji doul rek lay def thim

  • @mordiop1366
    @mordiop1366 4 ปีที่แล้ว +2

    Théy yalla kagne la djoulit yiii di nékk 1 saganté xassté waxanté lou bon yonnénbi djanglé woul lolou djiko bou rafét lafi bayii thiaxan bahoul

    • @mouhametthiam3388
      @mouhametthiam3388 4 ปีที่แล้ว

      mor diop waalae c vrai lolou waroul nekk sunu wareff mai defoi dafay fekni bene nitte moy gnew waxx louko nexx di saaga bene borom xam xam t xamalouko dara mai vraimnt dafgniy metti

  • @kamallo3304
    @kamallo3304 4 ปีที่แล้ว

    Doynawaar dekge boko dégé day set lér waye ay nar yalna nano siyalla mou sal kham kham pour deimo yalla la d'où pour werannte Omar salla

  • @talladiop2013
    @talladiop2013 3 ปีที่แล้ว +1

    Omzo gattame dina dague kou bagne yonou mouride do am jam bâ adouna di toukii

  • @ibrahimasarr335
    @ibrahimasarr335 4 ปีที่แล้ว +3

    Biteye fenikati nga

    • @AhmedNdiaye-k3f
      @AhmedNdiaye-k3f 9 หลายเดือนก่อน

      Yaw yay domou kharam

  • @mariamaba4273
    @mariamaba4273 3 ปีที่แล้ว

    Thiey Yalleu...not kou gnoul ci boppam mo reeer rek...