Salam halaykoum kou beug Sètan débat partie par partie cliquez sur ce lien Guis YONÈNTABI ﷺ si loudoul nélaw: th-cam.com/play/PLX6CUhFlHNrKnybGXax_3cGV7XUJb0Ck5.html
Sa montre k Sunnit yii luniouye wakh yeupp dagne ko amal laye ci islam. Ma sha ALLAH Quran ak Sunnah rk ba faaw bi IZNI'ALLAH. Ma sha ALLAH ya sheikh Morr Kebe. Diaza ka ALLAH Khayraan.
Yalla na borom bii faylén yiww té ki dioum borom bi ngidi ko si yoonou ndioub. Mais j'apprécie vraiment Oustaaz Mor Kébé. Yalla na yalla goudale fanam ak gnii téwon si bilé diotay ak mbolém dioulite ❤🙏
Macha'allah Oustaz Mor Kébé beugue nala ta yalla takh nguir kham kham bi ak laabir bi. Qu'allah t'accorde une longue et agréable vie ici-bas et dans l'au-delà
@@senegal1 pour ceux qui dise Mashalla oustaz Ahmed Sarr, tu clique pas (j’aime) sur leur commentaire et ceux qui dise Mashalla oustaz Mor Kebe, vous cliquez sur la pouce aimer. C’est quoi le projet au juste? Nioune nieup beineu lagne. Yalla nangu yalla xir sii bopam rk. Mais niari Oustaz yeup am nagne xam-xam
Niougn niep douniou ben dal, ndakh sarr lidi dinem si ay guent lakoy dieule te oustaz mor kebe H.A mome ballou wayam si ALQURAN AK SUNNA, wakh amine si niane yi
Très clair. Mais j'apprécie beaucoup Ahmed Sarr. Son débat est bien détaillé et plein d'enseignements. Dans toute religion, il faut parfois croire sans voir à l'œil nu.
Mashallah tu nous as ébloui oustaz Kèbè sawakhe khamhamèna moi j'étais à la confrérie Khadre je ne le sais plus maintenant merci encore une fois pour ce beau discours
ما شاء الله كلهما صاحبان العلم...❤❤❤❤ اللهم صل على سيدنا محمد الفاتح لما اغلق والخاتم لما سبق ناصر الحق بالحق و الهادي إلى صراطك المستقيم وعلى ءاله حق قدره و مقداره العظيم
Mâcha allah Oustaz Ahmet Sarr beug nala trop ndakh yalla ak xam xam bou léer ta andak teguine. Diereudieuf Cheikhou Tidiane yalnan doon say talibé ba faww si barké seydina mohamed
MASHALLAH OUSTAZ AHMED SARR, SA XAMXAM RAFET NA, SA WAKH LERNA, NINGAY DIANGUER AL KHOUR'ANE AMNA SOLO, AMNA YARR AMNA TÉGUINE. YALNALA YALLA YOKOU. AM KILIFA REK MO WOOR. TALIBÉ CHEIKH RTH
Salam halaykoum kou beug Sètan débat partie par partie cliquez sur ce lien
Guis YONÈNTABI ﷺ si loudoul nélaw: th-cam.com/play/PLX6CUhFlHNrKnybGXax_3cGV7XUJb0Ck5.html
1
Yal na YALLAH faay yiiw
Dama bègue bokou ci Goroup wattsap alkhourane ak sunne ma doliko se sama dine le moyé sama ne moro 78 594 74 61
Demal si dernière video yi lien groupe bi mogui si DESCRIPTION video bi
Vraiment mor kebe maîtrise bien ce qu'il dit ❤
Le Sénégal à besoin plusieurs oustaz mor kebe pour mieux comprendre notre religion
Sa montre k Sunnit yii luniouye wakh yeupp dagne ko amal laye ci islam.
Ma sha ALLAH Quran ak Sunnah rk ba faaw bi IZNI'ALLAH.
Ma sha ALLAH ya sheikh Morr Kebe.
Diaza ka ALLAH Khayraan.
Yalnagnou yala maye gnou guiss yonentibi ak kou nai ameen fi dounya ak alahira yal na yekh
Amiiine barkeb Seydinaa Muhammad
Amine
Ameen
Amine
Âmin
Yalla na borom bii faylén yiww té ki dioum borom bi ngidi ko si yoonou ndioub.
Mais j'apprécie vraiment Oustaaz Mor Kébé.
Yalla na yalla goudale fanam ak gnii téwon si bilé diotay ak mbolém dioulite ❤🙏
سيد احمد صار ماشاء الله حفظك الله ورعاك يا صار
Débat bi doumassi doyal mashallah oustaz mor kébé do moromou gayi sa niveau kawéna Loudoul alkhourane ak sounna doyougnou
Machallah oustaz Ahmed Sarr kham kham bi leer na machallah
😂😂😂
Dieureudieuf Oustaz Ahmed Sarr si xam xam bu lére bing niu indil yalna jamm goudeul sa fane T mayla wérr si BARKÉ YONENTI BI PSL
Macha'allah Oustaz Mor Kébé beugue nala ta yalla takh nguir kham kham bi ak laabir bi. Qu'allah t'accorde une longue et agréable vie ici-bas et dans l'au-delà
Amine wa iyyaka
Amen
@@senegal1 pour ceux qui dise Mashalla oustaz Ahmed Sarr, tu clique pas (j’aime) sur leur commentaire et ceux qui dise Mashalla oustaz Mor Kebe, vous cliquez sur la pouce aimer. C’est quoi le projet au juste? Nioune nieup beineu lagne. Yalla nangu yalla xir sii bopam rk. Mais niari Oustaz yeup am nagne xam-xam
Niougn niep douniou ben dal, ndakh sarr lidi dinem si ay guent lakoy dieule te oustaz mor kebe H.A mome ballou wayam si ALQURAN AK SUNNA, wakh amine si niane yi
Aamiine ya Rabbi 🙏 🙏 🙏
Très clair. Mais j'apprécie beaucoup Ahmed Sarr. Son débat est bien détaillé et plein d'enseignements. Dans toute religion, il faut parfois croire sans voir à l'œil nu.
l'islam ce le coran et la sunna ce mouhamad psl que allah envoyé pour l'unanimité pas des individus
Bilahi Oustaz Mor Kébé yaay borom xam xam deug❤️💙🖤🤍barakallahu fiika🤍
Masha'Allah oustaz mor kébé yalna yalla barquèl sa xam xam té mayniou dègg ak toppe
MASHA-ALLAH, merci BITÈYE
MASHA-ALLAH Mr Sarr, C'est très clair , MASHA-ALLAH Mor KÈBÈ
Que Dieu vous protège
Wallahi je suis content, qu'Allah te préserve ya oustaz Mor Kebe
Machallah oustaz mor kébé ❤ quelle analyse ❤❤❤❤
Macha Allah oustaz mor kébé yalna yalla samale arela
Jazak allahu khairan Oustaz Mor... sunnah rek moye deug te nopalee... yalla na borom bi sameulgnoulene
Allahumma barik Oustaz Mor Kebe
Machallah oustaz mor kebé yalna yalla Faye yiw
شكرا لكما وجزاكما الله خيرا ياشيخ محمد سار أيدك الله ونصرك نحن معك
Merci oustaz Ahmed sarr amna solo machallah
Alhamdoulilah ya oustaz mor kébé qu'Allah vs accorde une belle vie d'ici bas et dans l'au-delà. Alkuran ak sunna moy DEUG Merci bcp .
Machallah Oustaz mor kébé Wahbi dioub na
Bravo Oustaz more Kébé yalla nala yalla are takhawola
Machallah yalla na yalla sameu la oustaz mor yalla na yalla defla diam
Amine wa iyyaki
Jeureujeuf Serigne Ahmed Sarr. Mach'Allah ci lééral yi.
Mashallah débat bi nekh na❤️ Pour les autres essayez de puiser mo gueuneu am solo té bayi parparlo bii
Machallah oustaz mor kébé
Masha allah oustaz mor kebe coran ak sunnah rek moy deugue
Mourid la guem na guis yonentou bi mai Ausi cheikh mor kebe diambar la diambar la machaalah
Machalla 2 savants au tour de la table yalna borom bi sameu léne
Merci Serigne Ahmed Sarr ❤💖💗
Ahmed Sarr borom kham kham la Macha allah
MACHALLAH SERIGNE AHMED SARR , KHAM KHAM BI RAFET NA LOOL
Macha-allah amna solo loll.
Ms kèpeu kou agua si yalla si loudoule thiakhane , guisse yonènte si loudoule nèlaw.
machallah oustaze Ahmed Sarr
Maachaallah. Longue vie à Oustaz Mor Kebe
Dieureudieuf Ameth sarr sa xam xam lerr na talibé cheikh bi macha Allah thiey Mbaye
Yarou gua tey ga say wakh lerrna OUTASE Mor kebe ❤❤
Maachaallah amna solo cheikh mor kebe
Mashalla Mouhamadou Sarr lerna nagne yalla na niou yalla maye niou guiss yoinenti bi yakazatane
Amine
ما شاء الله يا أستاذ مور كبه لك علم جميل وواضح وغزير
Ma cha Allah oustaz more Kebe
جزاك لله خيرا شيخنا مور
Débat bi amna solo machallah ahmet sarr xam xam bi lerna té selle
سكرا لك الأستاذ مالك صار جزاك الله خير جزاء
ماشاءالله وجزاكم الله خيرا يا حبيبي
Oustaz mor kebe Macha allah sa wakh l'airena amna mana
Merci à vous ❤❤❤❤ chapeau à Ahmed Sarr et Mor Kébé
Mashallah tu nous as ébloui oustaz Kèbè sawakhe khamhamèna moi j'étais à la confrérie Khadre je ne le sais plus maintenant merci encore une fois pour ce beau discours
Yallah na brom bi deugar
Oustaze Ahmeth wakh dji lérr na machalla
Mach allah oustaz mor kébe kham kham by lérr yalla n'asa diame yague 🤲🥰🙏
ههههههههه
Oustaz Mor Kebe sa xam-xam rafet na maachàllaa. Yal na la Yàlla barkeel.
Oustaz mor kebe yalna yalla samou la te barkel xam xambi
ما شاء الله كلهما صاحبان العلم...❤❤❤❤ اللهم صل على سيدنا محمد الفاتح لما اغلق والخاتم لما سبق ناصر الحق بالحق و الهادي إلى صراطك المستقيم وعلى ءاله حق قدره و مقداره العظيم
machalah ostaz mor kébé bilay sa débat bi douma sappi moukou nakh xam xam bou lér bi ngafi wakh
أطال الله بقاءك
Thiaye Oustaz morr kebe yalna nga amull benn debat bula Diaaxall lii daii waneh ne xam xam rek moi deug
Walay oustaz Mouhammad sarr sa xam xam lerr na trop macha Allah bilahi
Machallah Alhamdoulilah Shukran cheikh Mor kébé wolahi alkhourane ak SUNNAH rek moy DEUG ❤❤❤❤❤❤❤❤zazaka la KHAYRAN
Amine
جزاك الله خير كثير ياسيدأحمدصارالعالم الكبير الأستاذالأكبر صاحب الفتح والفصاحة شكر صار
Machallahh Oustas ckeikh tidiane sarr yalna yalla samoula in challahh
Ouataz mor kébé sa xam xam rafétneu machalla
ههههههههه
Merci Ahmed Sarr
Mâcha allah Oustaz Ahmet Sarr beug nala trop ndakh yalla ak xam xam bou léer ta andak teguine. Diereudieuf Cheikhou Tidiane yalnan doon say talibé ba faww si barké seydina mohamed
أحمد صار ماشاءالله واضح جزاكم الله خيرا وحفظكم ورعاكم
Thiééyy Cheikhnâ Oustaz Môr Kébé ! Fa Tâbârakar-Rahmâne
Maasàallaa waxtaan wi amna solo loon xam xam bi leer
Yallana Yalla fay ñaari ustaaz yi ❤❤
Ma Shâ Allah ya oustaz mor kébé amna solo di diadieufeul oustaz sarr ak biteye.
C'est une fierté de vous écouter
Thiey sarr machalla
Mouhamed Sarr li ngay todj nékh na machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Mor kébé,votre discours est clair,précis et limpide.Des preuves,vous n'en menquez pas.
ماشاء الله تبارك الله يا أستاذ مو ر
MASHA-ALLAH À VOUS DEUX
MASHA-ALLAH BITÈYE
ماشاء الله بارك الله فيك وجزاك الله خيرا
Machallah oustaz Mouhamed sarr ❤❤❤❤
Bilahi xam-xam mo nekh...Machalah oustaz Mor Kebe.
Merci ouztas mor kébe
Machalla c l'islam qui gagne ahmad sarr ❤️mor kébé❤️bitey💓
Mashallah oustaz Mor kébé quelle pertinence 🥰lépp lér neuh
Machallah ouztaz mor Kébe , Allah arla té barkella
Machallah serigne sarr
Machalla oustaze Ahmeth sarr xam xam bi lérr na torope
Al khourn an djitou ahmed sar ,souna topousi mor kebe .yakarna nonoula démé❤❤
Machallah oustaz Mouhamed xam xam bi lérr na
Machalah oustaz Ahmed sarr
Kham kham dale nékhena yalla nalen yalla faye
Merci beaucoup oustaz mor kebe
macha allah mor
Ma sha Allah the program is educative
Mor ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤kebe❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nyum nyarr nyepp aii borom xam xam lenu macha Allah
Machallah oustaz Ahmed sarr
MASHALLAH OUSTAZ AHMED SARR, SA XAMXAM RAFET NA, SA WAKH LERNA, NINGAY DIANGUER AL KHOUR'ANE AMNA SOLO, AMNA YARR AMNA TÉGUINE. YALNALA YALLA YOKOU. AM KILIFA REK MO WOOR. TALIBÉ CHEIKH RTH
Maa shaa Allah longue a toi mon fils maman bineta Ndiaye
ماشاء الله يا أستاذ مور بارك الله فيك وزادك بسطة في العلم في الجسم
Macha Allah débat nekhna m'ai lougana ce la finition de oustaz morkebe par ce que loumou wakh mo geun chakh texi yi
Si tex yi ga diangue
Dieureu dieuf oustaz Ahmed sarr