ขนาดวิดีโอ: 1280 X 720853 X 480640 X 360
แสดงแผงควบคุมโปรแกรมเล่น
เล่นอัตโนมัติ
เล่นใหม่
Togne bakhoul waw mais soit honnête Al Amine moni tollou dafa am thieur
Deugna si Ahmad Fall mouni Sériñ Abdou Alamine néna Cheikh Tijaan nangoulnaako talibém
Walaye walaye walaye Dieuredieuf Sy Malick MachaAllah kokou d'où sa morom rekkkk
Serigne Abdou la dé kokou kénn douko lal
Serigne abdou dou morom sénégalais yi xamuniouko
Togne bakhoul wayé al amine nak toutiwoul
Wallaye da nga khamoul rék Serigne Abdou si boppame la lila djik si togne kénène djigou la si Serigne Abdou Al Amine!!!!
Allamiin sy malik ❤❤❤
Serigne abdou al amine dou moromou garouwale sakh kouko lal lal latake
Wakhofi DOUL
Ragal na lolou bayi wou la nak 😂
Kii dafa rew Billahi amoul diom
Mo takh lila nakhari dall la
Al amine benen dimension la
Rawatina togne nitou Yalla lah
Pourtant si menone nga toogn kénène té dou démé nimou démé. Toogn moom bakhoul mais amna gno xamni koulène toogn si sasi ngakoy guis té Al Amine si la bok
Mané serigne Abdou ngua togne motah lolou dal la kokou lal lalaké la ( mais wakh degeu nekh yalla diambar ngua
Kone Kay meunone nga ballou yalla rek nitou yalla nga togne sa wadjii
Serine Abdou nit kesela budie mo wakh Lolu mom tonie diuli catye dakh nonu laniu wara diulie lolu Moy diuli
Khana tognoo ahmed KHALIFA niass?
Madaw kaye😂😂😂
😂😂😂 iow da nga dof.
Dagay fén rek affection gay woute si tidiane yi
Ki mbamla diaroul sakhe wakhal
Mais est-ce que sokhla nga one neh chrétien ngaFen bii dou bakar ?
Bakaar bou reuy sakh.
Walahi tonj bahut
😂😂😂😂😂😂
Par fois denley ton d te dou fenn
Yawe kou bakhe ga Sénégal mo doufe

Mais est-ce que sokhla nga one neh chrétien nga
Fen bii dou bakar ?
Bakaar bou reuy sakh.
Walahi tonj bahut
😂😂😂😂😂😂
Par fois denley ton d te dou fenn
Yawe kou bakhe ga Sénégal mo doufe