Je n'ai pas l'habitude de faire des commentaires sur les reseaux sociaux, mais j'avoue que cette image est vraiment belle. Lì rafètna trop bilahi. Yalna diamm yag ❤
Siiiiiiiiiii Wally ya degggggg yalla naleu ya ALLAH !!! Samm Té weeral sa baat bi doli leu soutoureu goudou Faan ak weer ak weerlé Mouth ak tawfekh si yaw ak mbolom Juliit ,Amine !!!
Sénégalais mandouléne si loléne khamoule, mandouléne si digueunté yi. Dégue nguéne li Père You wakh domame Wally Ballago Seck, gnome gnarr rééro wougnou. Ma contane si liii. Yalna dieume kanam.
C'est super c'est super formidable formidable c'est ça j'ai pris toujours Mali je prie toujours pour ça vraiment ça c'est formidable Youssou N'Dour je suis même je sais pas quoi dire voilà tellement que je suis je suis je suis content❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Legui sama Ndanane confirmer na car dou waykat yeupe gnon meune dougou ci way Youssou Ndour. La musique de YN est trop technique et beaucoup de chanteurs se perdent à un point que lui même les ramène 😂. Chapeau à Wally 🫶🏽🤍
WAOUH !!!! Bi guissé Waly si scène bi khawna guagnou ndeyssane li nekhna torope si khole I'M SO HAPPY👏👏👏👏💪💪💪💪💪💪 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Nioun dal Sénégal li laniou xamone kou nek diokh moromam respect c vraiment beau ❤❤❤
Xol séde na ❤️❤️Oh 😥😥Youssou Ndour et son fils waly le peuple est content 😥❤️❤️❤️❤️❤️❤️l’Afrique est content 😀 😂 ❤️❤️🥰❤❤❤❤❤
wa legui lossi yonou peuple bi ak wa Afrique khana gni beuge li wally wla youssou ndour
Wally balago seck est la révélation de la musique sénégalaise
Forever 🎉
C'est sa qu'on entend depuis des années merci dieu ❤
Merci enfin Wally va à la rencontre de Youssou Ndour li waron nako def bou yague
Vraiment @@aminatadiopamy1249
@@aminatadiopamy1249youssou moko beugoul woon nk😢😢
❤ Youssou Ndour ak Wally seck yalla na Ande bi Yagu ❤
Amine.
Amine yarabi
Li rafetna way c’est beau de voir Youssou Ndour et son fils Waly Seck chantait ensemble sur la même scène.
Waly est un grand champion vraiment, il arrive à composer avec l’ancienne et la nouvelle génération😊. Chapeau à toi Waly❤ Bonne continuation 🎉
Je n'ai pas l'habitude de faire des commentaires sur les reseaux sociaux, mais j'avoue que cette image est vraiment belle. Lì rafètna trop bilahi. Yalna diamm yag ❤
Meussouniou reero écoutez bien liko Youssou sédéle cette partie répond à tout ❤
Sma xol noum si sédei ni diaxal nama 😂😂😂😂bly dra dakoul diammm🙏🤩
Siiiiiiiiiii Wally ya degggggg yalla naleu ya ALLAH !!!
Samm Té weeral sa baat bi doli leu soutoureu goudou Faan ak weer ak weerlé Mouth ak tawfekh si yaw ak mbolom Juliit ,Amine !!!
Allahouma amine
C est vraiment beau MashaaAllah'.. Khaleyyi lingene sagnseii tamitt..c'est magnifique MashaAllah ❤️❤️❤️❤️❤️
Ngourou Diomaye nieupeu dioubo mashallah 😂♥️♥️
Amine 🤲 Incha'Allah
DIOMAYE SA NGOUR GUI YALLA BOUSI THIATE DOUGOU 🙏🏽
Sonko ak Barthélémy dioubo woño
@@modoudiop8105 barth cap verdien la Domou importé il compte même pas .
Ça c'est très très beau et je suis très content ce duo entre père et son fils ❤❤❤❤
Nothing is beautiful than unity ❤❤❤ we're happy and proud 😊 father and son congrats 🎉
A machalah yousou ndour et wally seck TFM ak 2stv la direct hier si soirée bi sama khol sedna 🎉❤❤
Je suis émue vraiment dama contane Wally seck et Youssou Ndour machalla 🥰🥰 li nice na waouhh laf thiate 🎉🎉
Enfin il était vraiment temps !!!
Wally is a man with the gold heart💛
Sénégalais mandouléne si loléne khamoule, mandouléne si digueunté yi. Dégue nguéne li Père You wakh domame Wally Ballago Seck, gnome gnarr rééro wougnou. Ma contane si liii. Yalna dieume kanam.
Sénégal Nioy créé ay ennemis
Vraiment Sénégal féne lagnou meune ak diakhassé
Li d warna takh nitt di wakh loume mais Sénégal dagni inventé rék yow jamais ñou wakh lougne khame yalla nagnou yalla di bale rék
Mine nagne gathié
fi ba adouna di diekh Sénégal amna ay nit fen ak diakhasse rek moy sen liguey @@fatimandao8359
Il a beaucoup de talents WBS❤️
Thieuy le chanteur du peuple international wally seck👑🥇🎤💰🌟🤍et son père roi youssou ndour👑🎤💰🌟macha ALLAH☝🏾
Waouh 🥰🥰🥰 nekhna
Wally ndeyssane kou bakh la té yaarou. Yalnala yalla saame faramaréne bi.
Youssou aussi
@@AwaNDIAYE-rb6le gnome gnarr gneuppa bakh Ma Sha ALLAH, père You moye sama waykattt et limou wakhale Wally motakh ma wakhé nonou.
Ndeysane sa c'est émouvant
Bilae yallah na senegal dieum kanam 🎉😢
❤❤❤this is what everyone was waiting for father and son 😢❤ jimbori dinaa kontan
C’est trop émouvant c’est l’Afrique qui gagne Wally a un très bon cœur
Wally seck le meilleur de tout les temps avec un coeur ❤️ en OR
Machallah le chanteur du peuple et son père youssou ndour le roi yalna diam yague
C'était mon souhait que wally chante avec son papa Youssou, rafétena ❤🙏🥰
Machalla sama faramaren bi goudal fane ak tonton Youssou ❤li nekhna way
Très très beau je suis très contente ça le Sénégal Diam ak salam ❤❤❤❤
C'est ça le Sénégal, c'est ça l'Afrique ✊vive l'Afrique one love Africa ❤
Ohhhhhh this is what everyone was waiting for..father and son keepitup ❤❤❤❤maa shall Allah .JEREJEFF
Ndeyssane Youssou beugoul wone wally dem lii da fort❤❤❤❤❤
No star degu moy Wally machallah frère ❤
I love this papa Youssou and Wally together ❤️❤️❤️🎤🎤🇬🇲🇬🇲
J’écoute pas waly mais vois par tout ces actions qu’il a un grand et bon Coeur
Li moy Sénégal ! Rafetna, nekhna. Yalna jaam sakh
Lou rafét rék mo rafét ndeyssane ❤
Walay j'ai les larmes aux yeux😢 lii dafa rafèt.
Youssou Ndour boula wayé rék wayeko Soula youho rek houhouko
Hoo youssou ak papa thione lamay fatali walahi li séed neu xol machallah papa you wally contente continuer ❤😊
Youssou le meilleur parle avec les sénégalais Wally le reléve
Macha Allah youssou nénako nagoule dogole bi 😢pour le memoir de son père et sa mère 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽 lii rafetena ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Bilaye yaye yayame té waly da ame yare ak téguine limoye sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Walliy bilahi dafa degue❤❤❤
Aka dégue kéne douko diame nane
Duo avec père et fils♥️ Youssou waly ♥️
C'est super c'est super formidable formidable c'est ça j'ai pris toujours Mali je prie toujours pour ça vraiment ça c'est formidable Youssou N'Dour je suis même je sais pas quoi dire voilà tellement que je suis je suis je suis content❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Waly se boutou yé ngui soga oubékou nak Macha'Allah c'est bien ❤
Wally meune na dé c'est en face de you que je vois qu'il a du talent
Machalla c'est beau vraiment ❤❤❤🎉🎉🎉
Massouma contanè ni si duo Wally yalna nga goudou fane yak papa you
Bilahi yalla n'a gnepou am diamou si barké alkhourane ❤❤❤❤❤
souniou faramaréne bi way akk grand you , vive le senegal❤❤❤❤
Jamano Pastef lenj neka jaama rk mooy amm.❤️❤️❤️
We are all happy tonightJerejeff Jerejeff Jerejeff youssou and wally❤❤❤❤❤
C'est ce genre d'image que nous aimerions voir quotidiennement entre les légendes et la nouvelle génération !
Le talent de Wally Seck extraordinaire ❤❤
Walay
Gawguéne si wakh sayetané mé dekeloulé paroleyi téguéne ame dégue you dafa beugone humilié waly motakh mou indi nagoule dogualebi mé waly ame fouleu té meuneu tontou nénako nékale kilifeu niaw
@@CoumbaFaye-u2h yw wernga 😂😂😂wally thi son bi la fek you dy
Enplus you dafa wax mou nangou dogal bi thi décès you teglo yi mou am
Maachalah rafete na ❤❤❤❤
Machallah ❤Youssou et fois❤
Ak ngourouDiomaye tout est possible ❤
Youssou Ndour empereur bi et Wally seck le roi du mbalax c'est vraiment beau
Dioubo national Alhamdulilah ❤❤❤❤❤
Que Dieu vous protège soyez béni soyez heureux pour toujours inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wally au cœur d'or oooh khol sédena
Vraiment c'est beau
Xol ❤❤❤❤sede na❤❤roi youssou N'Dour rek forever ❤️❤️👑❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
You.je suis.tres contente.de.vs
Wally.merci.de.beau.geste
Vivez.longtemps.voila.le
Senegal.que.Dieu.ns.sauvegarde.Amine
Yousou rk❤❤❤❤😢😢😢
Wallahi ndaysan machallah li nékh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wally est ce que nit leu ❤😂❤
Khôl ses na vraiment pour un Sénégal unie et prospère 🎉❤
Legui sama Ndanane confirmer na car dou waykat yeupe gnon meune dougou ci way Youssou Ndour.
La musique de YN est trop technique et beaucoup de chanteurs se perdent à un point que lui même les ramène 😂.
Chapeau à Wally 🫶🏽🤍
Waliiy ballago sek à vie ❤
Merci beaucoup waliiy ballago sek merci beaucoup yousou ndour
Ohhh sama Faramarene bi❤❤❤❤❤❤❤❤
Gnou khar la chanson feat Youssou Ndour bok ❤❤❤🎉🎉🎉
Waw wally seck🎉🎉❤
Lii deh mo geun rafet mais Waly a faillit tombé dans le piège ñu koy créel aý nonn rk respect et longtemps vie à père You❤.
Eh doule yaw
Hum wally meusul nono ak papal yene kay yénay kadialé
Meilleure grand ball de l'histoire ❤❤❤❤
😂 machallah mar yacine ❤❤❤ adouna amoul solo
Boumouy rarati way sen duo bi❤
Savez vous qu’il voudrait pas que wally pars 🎉🎉
Lo si kham😂
Genre yi melni yew lou yaxou Sénégal ñolo yax
Yeen moom ay doff ngeen rekk waxi doff rekk ak sokhor
Tt simplement magnifique
Bilh keb kou bagn guadji del and ak wally 😢❤❤
Ndéyesane machallah ❤❤❤❤❤❤
Waly ya bakh rafete khôl machallah
Slt super bonne chance pour tjrs dp8 Sénégal Mbour ❤❤père fils.les jaloux vont megrire🎉🎉
Ndeyssane l'histoire de la musique sénégalaise retiendra cette date du 04/01/2025 á L'esplanade du Grand Théâtre
🇸🇳 notre Cher Pays 🫶
Le peuple est contant Machallah li dafa nekh bilaye ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤wakh deug Ndour Yalla maynala MashaAllah ❤❤❤
Machallah lou rafet rek mo rafet❤❤❤
Ouhhh c’est tellement beau ❤❤
Youssou Ndour ♥️ ♥️♥️♥️♥️♥️
I love to see this guy together wally is my star ❤
Waly.yallah.na.goudou.fane..tu.les.le.meilleur❤❤❤❤
History will always write this ndeysan ❤❤❤❤❤
Li rafétna nekhna. Sénégal yalna gneupp ame diameu.
Thiey Maar yacine. Adouna mafi gueun beugg wally ❤😂❤
Chui content walay ❤️❤️❤️❤️
WAOUH !!!! Bi guissé Waly si scène bi khawna guagnou ndeyssane li nekhna torope si khole I'M SO HAPPY👏👏👏👏💪💪💪💪💪💪 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Wally mo guena beug youssou ndekké❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤