@@salzoofficiel2770 *Ouï ça aussi c’est vrai déh en plus djieukeur dji 1997 la donc dougnou ay mague nonou meune nako manipuler thi mbeuguel boumou am thi momm mais li momm c’est grave*
Ndeysane masta et du courage maman yala nala yalla mayate lou geune li inchalaaaaa! Dafa meti niak dôme bou djiguene en général belle fille doula respecter, mais dieu est grand t inchalaaa sa punition n’est pas loin à cause des Kamil qu’elle a brûlé
Maslaa bi ci boppam lañu wara bàyyi ak nëpp nëppal bi, sinon reuthiou rekk Kou bagne sa yaay moom bàyyil mou dem ay affaire de mbëggeel bi nga am sa jabar bou yaay ko gëna fort 😢😢
J’habite à Fann Hock non loin de cette maison mais cette maman là on l’a connais tous en tant que femme battante calme et souriante. C’est vraiment triste li meussoul am Fann Hock Bb fa def nga Lou niaaww Billahi 😢
*Cédé you rafette rk la guiss thi mére bi bilay parfois dôme togne yaye thi indil ko djiguéne bou boneu mais Yallah bakhna kou djiguéne ki dinako guiss…Lepp lou mére bi perdre Yalla na amate louko eupeu Amennn🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
C triste pour la maman 😭 kou beugoul sa yaye lokoy doyé moma diakhal ak wadiour fimou tolou ak nimou mel ce gar n’a rien compris et c malheureux pour lui 😞😞😞😞😞
YALLA séddé naakooo kiii dara daaloukoo , sou fébaaroone walaa amme aye raap daay khaarou mbaaa mou blesser dieukeur djiii mais retourner contre sa belle mère signifie que am’naa lou mou djaapal mère biii
97 khaler bou ndaw taak diabar ter sa am am demewoul nonou, doug ci khaler bou djiguenne bou rew ba dof...bamou taal sen Keur 😢. Sénégal baayilen tek naatou sen parents yi ..
@@madeleine7159 en fait je suis étonnée par l'âge. Pourtant 'il y en a qui se marient beaucoup plus tôt. Mais li yeup rewande AK niak kilifa la. C'est vraiment dommage.
Sérieusement sama khol dafa méti si li😢 sénégal ame na djiguène yi khamni nioy yakk dérou djigène yi… khawma exactement problème bi nimou démé mais d’après témoignage yi si mère bi ak commentaire yi gni kham mère bi nieup bène kaddou “kou dal la sèle teh beugue ndiabot gnimou diour ak gnimou diouroul” donc ce qui veut dire que belle fille bi moy problème bi😈 teh magui guiss yène commentaire yi niou nane est ce qu’elle n’est pas malade *DOFOUL DARA DALOUKO* nakh kou weroil dou rawalé bagages yimou fa ame ba paré soga deff lou niaw lou bone limou deff Franchement magui massa wou mère bi nakh li métina kheuy sa bagages ak sa matériel ak sa keur lepp yakkou teh dou kène koudoul sa goro😢 dieukeurou ndaw si mome khawma sakh louma ko wara wakh nakh diéppi ko😡
Tout le temps les gens disent que c'est pas normal soit elle est malade, c'est faux, c'est de l'indiscipline, il y a des femmes sadiques, y avait meme une femme qui avait brûlé vif son mari
On doit l'enfermer yobouko yarko travaux forces puiskel à de la force mou djayaneterko fofou rek Yalna YA ALLAH WOTTOULENE SAMLA ❤❤ TAAL KAAMIL MOM ALKOUREK QU'ALLAH NOUS PRESERVE
Mais elle est malade cette femme faut pas confondre l'impolitesse et la maladie elle a besoin de soins vous avez de la chance elle aurait pû tuer ou blessé quelqu'un Bon courage
Je ne comprends pas beuggeu Lou nexe sa dome ba lorrou eupeuneu! La belle fille aurait dû rester chez sa mère à partir du moment où elle a montré des signes de dangerosité.
Yaye kene dou mome❤️rawatina dome bou gor doula togal doula fotal doula balel khana ngay daw si mome bamou mague sou také diabar mouy tangal sa khol dara doufa barkel ❌ soyez prudents et faites vous conseillez c est très important le mariage moy défar aduna wayé moy yakh aduna
Sama khol bi tangue na torop 😡 la responsabilité incombe son mari lèp mom leu comment tu peux laisser une femme te terroriser et ta mère comme ça ? c'est un truc de fou... Mais ki mo yabatè nak
J'étais un voisin de cette famille et tout Fanny savait que ce jour viendra. La fille habitait a la maison d'à côté avant leur mariage devant la maison de son mari elle a insulté le père de son mari devant tout le quartier pendant des heures elle avait même pris un bâton pour frapper le vieux et quelques temps après elle s'est marié dans la maison donc cela ne nous surprend pas d'elle elle est malade et capable de faire pur L'unique responsable c'est les parents . Le nom de la fille c'est Bébé fa de Fanny hock
Soubhanallah avant le mariage mou def lolou yeup après gnu takk KO,goor gui mo faible REKK un homme tu dois obligé ta femme de respecter ta maman souko meunoul tu bouge oklm
Tant que amoul mort ils vont pas reagir et si tu vois leurs yeux tu verras qu ils ont peur tres peur de la fille😢😢li moy senegal en tous cas faut tout faire pour regler cette bleme car si ca continue sa finira mal🤦♀️
Svp chers frères choississez bien vos femmes. Setlenn setate bala guenn di takk diabar. Oute lenn kou mana respecter senn yaye diaper ko ni sa propre mére. Sa yaye bila diour sahhh dou niak parfois mou def leuh loula metti ter danguakoye mougn donc pourquoi pas diapper sa yayou dieukeur comme ta propre mére????? Choisir lenn boubakh bala takk Mane dehh kou beugoul sama yaye beugoumala
Mère bi ndéyesane bougue dome rék mo warale li 😢 mais sa dome bi témite wéroule dale insulté sa mère sissa khaname té lidieune tiwoko il est nul waye 😤😡 mère il faut les foutre dehors une fois pour toute de ta vie avant l'impassable 🙏
C'est triste mais ce genre d'histoire est courante dans les familles sénégalaises à des degrés divers Il faut que la police prenne au sérieux les conflits de belles filles, nommées pièces rapportées, avec leurs histoires de vie, qu'elles emportent dans leurs belles familles...
Ndawssi dafa ignané mére bi keugui motakh mou tal ko souma bokone ake dieukeur dji balamo tall keurgui féck na ma tegueul ndeyame guéné ko keurgui ki domou kharam deuguele
Salam à mon avis d'après les dires cette femme devait sortir de la maison depuis le début de ses problèmes les parents sont trop sentimentales insulter sa mère c'est trop
Ay way Ta Absa tu ne mérite pas sa vraiment. vous nous avez fait grandir avec ta maman si gentille. soyez forte vraiment. on ne doit pas cautionner cette barbarie.
Pa gua balma kou beugue lou yomb gua guay borom keur gui moy diokhé dépense fay couran ndokh etc....uffff bolesi irresponsable ndakh nane biniou commencé la dem sama keur yaye con khalato won sa diabar ndakh dokofa bayi😢😢
Je connais bien cette maman , elle est tjrs calme et bien , elle n’a que 3 enfants Khale moy son fils ainé. Courage à elle yallah barina soutoura
Kou bakh te sell bima neke université moma done diay crème
Mère bi dh kou sedd la. Les gars délén Andil mère yi kou bakh. Elles le méritent très bien vu la souffrance qu’elles ont endurée par le passé.❤
Lou souniou yaye yi sonou rek diabar you Bone yi niolen koy tek
@@ironahide5896bilahi 😢
Bilahi 😢
MEISSA Diop tu ne sais pas si bien dire mère bi gno deuk kou bakh kén meussouko atté Bilahi kou seleu
*Bilay ioe j’ai de la peine sakh ligua wakh dawna yaram mais t’a raison nos mamans méritent ça*
Kamil 🥺 c’est fini pour elle, kholam dotoul nekh ba faw 😔
Ki assassin leu faléwoul kamil😢😢😢
Yakouna.ba.faw.bilay
@@souka1321ndeysane motakh niouni rewandé kendou ko ndamo
Bilay wolay
Ko goor ki mou def lep
Téré Alhouran 😭Ndeysan d’où massa lak 🙏yalla moy Karim 🙏
Tall kamil nak😢😢😢laisse la avec dieu 😢😢😢☝🙏
Thièye Sénégal fomou dieume ohh vraiment lii métina djiguéne bou bone bakhoul ci keur
Yén domram yi mérité wougnou nek goor... comment tu peux laisser ta femme manqué de respect autant à la mère sui t'a mis au monde..
Wakh degue yalla mane mome djiguéne la wayé souma nékone guorr djiguéne bou beguoul sama yaye damalay bayi ngua dém
Ta Absa massa, vraiment yow nitte kou bakh nga sans problème que justice soit faite.les belles filles dafa ame gnou doy war
On devait la mettre en garde à vue, ouvrir une enquête et attendre la discision du procureur..
Toujours le problème vient des hommes il faut voir kel genre de femme épouser et respecter nos mamans la naissance n'a pas de prix massa yaye boye
Diabar bou beugoul sama wadiour dé ma fasséla ba fasséwalé sén wakeur
Yow la geum dé wadiour amoul morom té djingéne yi beuri nagn
*Kessei nakkk*
wah deug
Mais frr yene saye djiguene yu dagnouy liguey sene dieukeur yu ba lougn lene wakh gnou nagou😢
@@salzoofficiel2770 *Ouï ça aussi c’est vrai déh en plus djieukeur dji 1997 la donc dougnou ay mague nonou meune nako manipuler thi mbeuguel boumou am thi momm mais li momm c’est grave*
😭😭vous m’avez tous fait pleurer, je ne comprends pas son mari, femme bi amna chance deuk ak ñou meuna mougn wallahi, MASSA ‼️
Wallaye maman je te comprends nous on vie la même chose avec ma belle sœur
Il faut la foutre dehors on avait une pareille on la foutu dehors la elle veut revenir mais on refuse
Ndeysane masta et du courage maman yala nala yalla mayate lou geune li inchalaaaaa! Dafa meti niak dôme bou djiguene en général belle fille doula respecter, mais dieu est grand t inchalaaa sa punition n’est pas loin à cause des Kamil qu’elle a brûlé
Bilay dom bou djiguenne rek la amoul bou amone kou tolok mome dolé dinako bayi khel
Dougal léne photom gnou xamé ko bala kénén diko takk mouy déff mm erreur 🙏🙏🙏🙏
Maslaa bi ci boppam lañu wara bàyyi ak nëpp nëppal bi, sinon reuthiou rekk
Kou bagne sa yaay moom bàyyil mou dem ay affaire de mbëggeel bi nga am sa jabar bou yaay ko gëna fort 😢😢
Même si l'amour est aveugle,comment rester avec une femme qui n'aime pas ta mère, il y'a des enfants qui meritent même pas de les avoir enfantès
Je te jure
Vraiment
@@fandao2138koula beugoule ba won lako lokoy beugué
😮😮😮😮😮😮😅😮😅😮😅😮
Elle devait les expulser depuis
J’habite à Fann Hock non loin de cette maison mais cette maman là on l’a connais tous en tant que femme battante calme et souriante. C’est vraiment triste li meussoul am Fann Hock Bb fa def nga Lou niaaww Billahi 😢
Sma taw bimou Bokal tour moma metti
*Cédé you rafette rk la guiss thi mére bi bilay parfois dôme togne yaye thi indil ko djiguéne bou boneu mais Yallah bakhna kou djiguéne ki dinako guiss…Lepp lou mére bi perdre Yalla na amate louko eupeu Amennn🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Mane khalé bou djiguène bi la yereum ainsbi dakhe kamil yimou tall yalla dinako allak bou bone😢😢😢😢
BILAHI elle est fini 😮
Ki kay meussoul dof loutakh mou guéné ay bagageam avant mouy def acte bi moko tay boulén diawalé. Elle l'a préméditée
Merci doff dou reagir ni
Lahila ilala femme bi mo bonne deug rouss n'a sakh en tant que djiguen 😢😢
*Bilay ioe😢😢😢*
Wakhatiko,😢
Yalla naniou yalla mousseule thi jiguenne bou bonne
Amine
Amiin
Amine
daa fiir ndeysan
C'est une femme très mal éduquée .que justice soit faite et quelle pourrisse en prison.
Ki son cas relève de la psychiatrie
*C’est pas une question de mal éducation elle est malade celle la😡*
@@sunkiss4950carrément rew ba dof moy li. ki weroul!
@@sunkiss4950je pense pareil
@@veroniquenatack7392ma chérie rèw so doffoul sa rèwandhè desna
Masseta m'a maman elle parle avec un cœur meurtrie😭😭😭
*Je te jure😢😢😢mais c’est dure nakk ce qu’elle vit la*
yallananiou yallah khire thie beugue cou bakhe té nité
ALLAHOUMA AMINE YA RABAL ALLAMINE 🤲🏾
*Amennnn❤🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Amine
si tu attends la police, tu risque ta vie ,prend garde et prends tes responsabilités
CETTE BELLE MAMAN EST TRES RESPONSABLE.YALLAH NALLAH YALLAH FEYY❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Il faut protéger la maman si non femme bi dinako réy et aprés medecin aprés la mort
Kiii yalla nako Yalla atték ak mére biii téuré alkourane biii tale yalla dinako lidieune tille boppame barki yonènne tiby
C triste pour la maman 😭 kou beugoul sa yaye lokoy doyé moma diakhal ak wadiour fimou tolou ak nimou mel ce gar n’a rien compris et c malheureux pour lui 😞😞😞😞😞
Je dis et redis cette femme n'est pas seul dans la tête
YALLA séddé naakooo kiii dara daaloukoo , sou fébaaroone walaa amme aye raap daay khaarou mbaaa mou blesser dieukeur djiii mais retourner contre sa belle mère signifie que am’naa lou mou djaapal mère biii
Naka la nitte meuné lounou mel
*Dara dalouko réw dongue moko diap ak bone*
Mère massa xalei bou djiguene bi dara diotou ko day rewantou rek dieukeur bi niank fayda
@@ndiougafatimdafa rew iniane mere bi boumou bayi nako toppou jusqu’à bout com k domam da niak diom matadi
Il y a un manque de kilifa actuellement il y a beaucoup de parents qui ne veulent pas prendre leur responsabilité c'est dommages
Mounouma consovoir ngua nek kilifa bou goor t mouno zerai sa keur mane pabi la guena mera thim
Pabi ak merbi ay kilifa laniou mais danio dieum mag amouniou doler t'es danio diabétiques warouniou dieul beneu risk bala nioulen di blesser khaled ak mag bokoul kilifa dou kestion d'ancienneté affairou bopoula
@@biggileu7535 bilaye ligua wakh degu la mai khalebi dgn ko warona niouss amna rewandai go khamni yefou mateye laye nirou
Bilahi irresponsabilité bi eupna
Ndaysan badién yalla nala yalla may kholou mounge 😢
Ap dof deug ngén takeu heureusement ba kén déwoussi 😢😢😢😢
97 khaler bou ndaw taak diabar ter sa am am demewoul nonou, doug ci khaler bou djiguenne bou rew ba dof...bamou taal sen Keur 😢. Sénégal baayilen tek naatou sen parents yi ..
Dayna warr deh
*Vraimnt😢*
97 ????😮
@@kya_lovelydays lolou la yaye dji wakh...1997 la dioud ... j'imagine que la femme vers 2000
@@madeleine7159 en fait je suis étonnée par l'âge. Pourtant 'il y en a qui se marient beaucoup plus tôt. Mais li yeup rewande AK niak kilifa la. C'est vraiment dommage.
Justice Sénégal daal ci mbirou Ousmane Sonko rek laniou sawar, té criminels yangui fi di sonnal askan wi niouleen di sétaane thiey YALLA yeureum niou!
ALLAHOUMA AMINE YA RABAL ALLAMINE 🤲🏾
Lou fi bone sonkoo kofi indhi
@@deugheulaveritemoufin4731bilahi walahi si mome lagnou djaguer bone
Bilahi une femme désespérée vient chez vous et vous lui dit que séneu yoneu nekoul ménage
Li lep Ousmane sonko moko fi andi
Lepp loula metti sa dome bou ngoor bi molako tekk😢
Walakhi du ken mom la surtu nak bu feke mongui ak sagom defoi djiguene liguey la ba do yengu lumu wakh ngani dacor
Djigguén diou Bonne bakhoule
Ici en espagne 2 personnes qui discutes a hautes voix la police arrive rápidament sur les lieux
Yalla na souniou dekk bi agg niveau bobou🤲
*Mais ici c’est tt le contraire 🤦🏽♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️Nos forces de l’ordres sont des incapables😡*
Dëgo moni ma dém police au lieu d'appeler
En Espagne la police a toujours l'essence dans son réservoir alors que ici c pas le cas 😂
@@zaldiop6293 sheut wakhati nga bénen problème kone nioune souniou situation graaw na 😁😁
Sérieusement sama khol dafa méti si li😢 sénégal ame na djiguène yi khamni nioy yakk dérou djigène yi… khawma exactement problème bi nimou démé mais d’après témoignage yi si mère bi ak commentaire yi gni kham mère bi nieup bène kaddou “kou dal la sèle teh beugue ndiabot gnimou diour ak gnimou diouroul” donc ce qui veut dire que belle fille bi moy problème bi😈 teh magui guiss yène commentaire yi niou nane est ce qu’elle n’est pas malade *DOFOUL DARA DALOUKO* nakh kou weroil dou rawalé bagages yimou fa ame ba paré soga deff lou niaw lou bone limou deff
Franchement magui massa wou mère bi nakh li métina kheuy sa bagages ak sa matériel ak sa keur lepp yakkou teh dou kène koudoul sa goro😢 dieukeurou ndaw si mome khawma sakh louma ko wara wakh nakh diéppi ko😡
Bilahi doffoul rapp diapouko.dfa reiw rek.Jsper k yone dina deff ligueyam.dieukeur dji mome desser na nekk goor
Tout le temps les gens disent que c'est pas normal soit elle est malade, c'est faux, c'est de l'indiscipline, il y a des femmes sadiques, y avait meme une femme qui avait brûlé vif son mari
On doit l'enfermer yobouko yarko travaux forces puiskel à de la force mou djayaneterko fofou rek
Yalna YA ALLAH WOTTOULENE SAMLA ❤❤ TAAL KAAMIL MOM ALKOUREK QU'ALLAH NOUS PRESERVE
Mais la police l a libérée pourquoi ?
Les belles mamans devraient refuser avec les femmes de leurs fils. Les belles filles d'aujourd'hui sont mauvaises avec leurs belles familles
C pas tous
Khaley yi di seuy bayilen bonn te respecter sen guoro yi
Bilay mane mome personnellement mère yii dama léne yeureim.séne katane djékhna té xalé yii wow nagn boeute rew teksi lou khew niouni rapp
@@seynaboudieng7475malako wakh mais lo def yoyou diambour niou def ko sa yaye rek
Mais elle est malade cette femme faut pas confondre l'impolitesse et la maladie elle a besoin de soins vous avez de la chance elle aurait pû tuer ou blessé quelqu'un Bon courage
*Hummm je suis d’accord avec toi déh il faut qu’on la consulte pour voir si réellement elle va bien…😡😡C’est une vraie tarée celle la*
elle n'est pas normale
Walahi je suis d'avis avec vous soite elle est possédé par un démon de la pire espèce ou elle est malade mental elle a besoin d'aide dé
bayil sa thiakhan yi ki Dara dalouko dafa rek pourquoi elle a pris ses affaires baparé soga tal keur gui il faut être honnête
Bilaye li nekhoul
Vraiment li eupna😢😢😢😢😢😢😢😢li niawna😢😢😢😢😢😢mère sa dome amal nala akh😢😢😢😢
Kii dé merbi laronarey😭😭😭
Mon frere prenaient vos propres Responsabilités. En tant que frere . Cette femme ne doit plus mettre les pieds chez vous.
Ndeysan sama Tata bi aka bakh tè am dall elle a toujours été gentille
Qui monte bonne
Tout ça c'est la responsabilité de son mari
Ndeyessane le vieux est Tres sage machalla
Sa dom modoul nitou Dara motakh guelbi yaplénne
*Bilay walay kokou amoul diom thimmm*
Bilahi
Non bouléne jugé wadji tayou ko khame na limaléne wakhe
Oui
Mais on devrait la garder en prison en attendant de la juger
L'irresponsabilité des hommes
Bilay c est Domenge pour nous😢
Késsé nak
Je ne comprends pas beuggeu Lou nexe sa dome ba lorrou eupeuneu! La belle fille aurait dû rester chez sa mère à partir du moment où elle a montré des signes de dangerosité.
Porte plainte chez le procureur gnou dieule ko en charge
Ndeyssane amna goor you faible il a trop toléré cette femme !
Mais police tamite dougne si wakh?😢
Yaye kene dou mome❤️rawatina dome bou gor doula togal doula fotal doula balel khana ngay daw si mome bamou mague sou také diabar mouy tangal sa khol dara doufa barkel ❌ soyez prudents et faites vous conseillez c est très important le mariage moy défar aduna wayé moy yakh aduna
Quelle femme a mis au monde une personne de ce genre ?
C'est une mauvaise femme vraiment est sadique
Sama khol bi tangue na torop 😡 la responsabilité incombe son mari lèp mom leu comment tu peux laisser une femme te terroriser et ta mère comme ça ? c'est un truc de fou... Mais ki mo yabatè nak
*Je te jure cet homme lui a donné bcps d’autorité pour qu’elle puisse arriver à cette stade une vraie folle celle la😡*
@@veroniquenatack7392dama défé ni dieukeur dji tayouko déh khana
J'étais un voisin de cette famille et tout Fanny savait que ce jour viendra. La fille habitait a la maison d'à côté avant leur mariage devant la maison de son mari elle a insulté le père de son mari devant tout le quartier pendant des heures elle avait même pris un bâton pour frapper le vieux et quelques temps après elle s'est marié dans la maison donc cela ne nous surprend pas d'elle elle est malade et capable de faire pur L'unique responsable c'est les parents . Le nom de la fille c'est Bébé fa de Fanny hock
Li la olof nane lou fégne si seÿ noyowone na si ngoro bi dagne ko fayoul wone
Khamna merbi ampoule dôme bou djiguene. Mane douma nagnou dama diabarou mague wala rakk Di yapp samaye wadiour makoye d'enfanter ak yow
@@alimandiaye5085exactement
Soubhanallah avant le mariage mou def lolou yeup après gnu takk KO,goor gui mo faible REKK un homme tu dois obligé ta femme de respecter ta maman souko meunoul tu bouge oklm
ki doffoul day réwantou dagnou wara gnouss ndayam
Tant que amoul mort ils vont pas reagir et si tu vois leurs yeux tu verras qu ils ont peur tres peur de la fille😢😢li moy senegal en tous cas faut tout faire pour regler cette bleme car si ca continue sa finira mal🤦♀️
Effectivement
Svp chers frères choississez bien vos femmes. Setlenn setate bala guenn di takk diabar. Oute lenn kou mana respecter senn yaye diaper ko ni sa propre mére. Sa yaye bila diour sahhh dou niak parfois mou def leuh loula metti ter danguakoye mougn donc pourquoi pas diapper sa yayou dieukeur comme ta propre mére?????
Choisir lenn boubakh bala takk
Mane dehh kou beugoul sama yaye beugoumala
Pour moi la Dame est folle franchement
Bien sûr
Dama yakarni djinné dioubo mom la andal
Wallahi famille-bi gno yarou layy sou dadièwonn ak famille bou fèroce ,mome ci bopam lagnouy taall
Mer boul deukeuti ak mom dala bougona ray
Mère bi ndéyesane bougue dome rék mo warale li 😢 mais sa dome bi témite wéroule dale insulté sa mère sissa khaname té lidieune tiwoko il est nul waye 😤😡 mère il faut les foutre dehors une fois pour toute de ta vie avant l'impassable 🙏
Ok Fatima je comprends bien ce que vous dites
Merci
Man dé dou ma dekeuh béne belle fille
Police dal avec sonko
Pas de enquête mais bou population bi diakhlé police ni enquête 😢😢😢
C'est triste Sénégal Macky yakh n'a Sénégal 😢😢😢
WAYE MÈRE NOKALE SA DOME SI BITI MO GEUNEU BONE LA FILLE LOU TOLINI SA YAYE GNOUKAYE SAGA GUAY ANDAK KIKAY SAGA
Vrai famille sénégalaise amna bator ak mar
REALLY !!! C DOMMAGE MAIS LII KHÉW SÉNÉGAL 🤔🧐
ON AVANCE À RECULONS RÉK !
Parce que la mentalité ne change pas et le respect de même 😢
C'est triste mais ce genre d'histoire est courante dans les familles sénégalaises à des degrés divers
Il faut que la police prenne au sérieux les conflits de belles filles, nommées pièces rapportées, avec leurs histoires de vie, qu'elles emportent dans leurs belles familles...
Europe il suffit k y’a des bruits la police intervient mais Sénégal du n importe koi
Sa keur di takk yaw borom keur bou goor nganane narouma woone nieuw . Quelle fuite de responsabilité !!!
*Vraiment 😢*
Nena dou keureum keur fem bi la😮😮😮
Yaw pabi magu la boko guissé noumou wokhé
Gni nawsi daleine traumatiser
Gourgui mo niague faida man jdigune dou ma yap jdigune g m yap ma ray ndayame
Ndawssi dafa ignané mére bi keugui motakh mou tal ko souma bokone ake dieukeur dji balamo tall keurgui féck na ma tegueul ndeyame guéné ko keurgui ki domou kharam deuguele
Salam à mon avis d'après les dires cette femme devait sortir de la maison depuis le début de ses problèmes les parents sont trop sentimentales insulter sa mère c'est trop
Ay way Ta Absa tu ne mérite pas sa vraiment. vous nous avez fait grandir avec ta maman si gentille. soyez forte vraiment. on ne doit pas cautionner cette barbarie.
Vraiment 😢
Cheuooo wallahi amna ay nitt gniou bone bismillay diam
Ndeysane
Démal khool bakham marabouter wouko Ces genres de filles sont tellement dangereuse 😢
Noonu lay demee sax. Dafa am gnou capable
j'ai pensé à cet hypothèse, je suis voisin de cette famille mais la fille je ne vois personne donner un avis positif sur elle
Ndaysan j'ai pitié de la maman yalna yalla taxawou te mayko lou eup ndiortam
*Amennn❤️🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Sene dome mo bakhoul djiguene la dieunde ay wa wadiouram
Le procureur doit s auto saisir
Pa gua balma kou beugue lou yomb gua guay borom keur gui moy diokhé dépense fay couran ndokh etc....uffff bolesi irresponsable ndakh nane biniou commencé la dem sama keur yaye con khalato won sa diabar ndakh dokofa bayi😢😢
Lii Yéméneu trope nanioukoo toppe jusqu'au bout femme bii criminels leu waay
Sunu ka baye
Dîna rey nit lolu mom lerna doful djine diapuka
Ooh nooonnn masseu yaye boye cette femme est dérangée nako ay mbokkam fathie 😢maintenant elle a causé trop de peines à cette famille
MÈRE LOUTAKH FASE WOUKO BOU YAGUE KONN DOFF LA TAKK AM NGA CHANCE DAFF NARONE SODE
Bien sûr
Maman gendarmerie bridage de recherche gua warone déme plainte ko
Bonne. Rek
Dicourage maman yalla dinala até akh mome kou tale ba tale kamine yalla dinala tale, ki embecille la rek yalla naléne yalla até akh mome
Je vois que son fils est immature il faut que sa maman l'aide pour s'en sortir sinon ça va mal se passer un jour.
Ki dof la sou nieuwaté si keur gui boumou dougue
Et maman ne laisse pas ton fils entre les bras de cette femme sinon dinako raye ngua niak
*Douma nila dett déh sagne na ray djieukeur dji*
@@veroniquenatack7392 bilaye
Ki daniou ko bayi si liko nékh voilà le résultat
Mère bou bakh la machallah
😢😢😢hééé wa gni goor ame no beugué djiguéén bou agressifé nii 🤔🤔🤔mane kou bagne sama yaye ma bagne la
Pa bi mom esk cv? Ahh xalass
Mere yalla nala yalla may xolou mougn témou até la ak femme bi yalla naniou yalla mousseul si sheytan ak meeer(la colère)
Am guene. Natou
Et la police ne l'arrête pas ou elle est sorcière
Quelle.irreresponsabilite'.des.parents.quelle.faiblesse.des.parents.a.legard.des.enfants.trop.de.l'essais.aller.