Képp kou guiss cette femme appeler la police aider son père à retrouver cette femme elle est au Sénégal cherchons tous ensemble on la retrouvera par la grâce divine inchalla
Je vois un père de famille épuisé triste 😢 oh Seigneur éclaircit cette affaire justice sénégalaise dal amena bras long depuis 03 ans ça traîne pas de résultat c’est difficile. Justice pour lissa tine
Justice pour lissa tine li Metyna nonou la bou len meusseu bayi continuer le combat Metyna ma trop Bilay dem len si presse yeup aussi def len marche pour Au niveu de Dakar justice pour Lissa Tine 🥲🥲
Pourquoi un dossier sans suite??? Vous avez des preuves sur le taximan et à la quincaillerie🤦😏malheureusement on a une justice corrompue walahi🥺🥺son ex mari sait tout sur lissa tine
Nioune wa refane ak kouy sénégalais yepp nioo wara organisé marche au niveau de Dakar justice pour lysa Tine lii dafa meti trop bou nekone sa rakk damay ray ndayam wala ma kitnapé yayam
Li môme je ne dis pas wa réffane mais sénégalais gnép gno si warr diap car li père bi wakh rék nékoul ni daffa réral khar wala fasse mais domou Adama la té dafa am akh AK yéléff si rewmi li kén warouko sétane
Ce papa est vraiment épuisé vu sa manière de s'exprimer thi deug leu neh da am yo khamné sincerment diarul gassss mou sorri thiey senegal esk on é en sécurité
A mon avis je pense que ni dafko ray.parce que liko diaral dem Mali,Burkina fasso dem guinée kokou amna loumou def lou reuy.séquestration rek diaroul lolou yeup.modou yade heure bi si kasso bi lako waron fek
Classez sans suite ??? C’est terrible ! Qui est modou yade? Ne baissez pas les bras papa cherche ta fille du courage faites appel au président de la république
Modou yade mi mom moy kane? Guénel domou diambour. Mais tamit loutah classer sans suite ? Mane dh je comprends pas la justice de ce pays libérez cet homme s'il vous plaît sone neu akh ndiourél dafa fort 3ans guisso sa doom li métina si khol
J’espère juste que Lissa est vivant Li metina dey Que la justice fasse son travail way guissouniou Lissa ta Modou Yade di dokhantou Nice Yomb na trop way
Sénégal da am nio wamni mousougne danguay faye ay nit niou kidnappé wadji une semaine niou torturé ko tant que waxoul bouniouko bayi soudon man je ferai pire yone defoul ligueyam nga nekeu nandité ba guiss sa dom père souma amone sa numéro ma dioxla solution bilahi té dosi fegne yombouna trop koulay diay woyou nga diayko mouss 😡
Bilaye lepp dina lerr yaye sa paté coura paté féguane dokhore guette bilaye affaire biii dina lerr thi barké mames yi Tine dioguoye samba Dieu es au Contrôle 😭🙏
On est au Sénégal guisgua modou Yade 3mois yi mou Dem kene guissou ko c, est Louche demna defari bopom si maraboutage pour kene d'où guisse dara te d'où moudier feneu kou Dem yobale ay millions niou tok 3mois kene guissouko khamguani préparé n'a bopam bou yagu Lima yakar moy raynako
La seule chose que je vous mes frères et soeur nine partagè video yi si tik tok ak Facebook pour denoncè encore injustice bi c'est triste vraiment ypa de justice dans notre pays coumba ame ndeuy ak coumba amoul ndeuy mofa ame
Pére Sénégal amoul justice ils sont tous des corrompus, soudone maye yow modou ngaye diape yewko bamou dougeur guasse paxe soul ko , kome nimou def sa dome
Exactly! Même chose la khalate. Ils doivent kidnapper le gars dindi galathie yeup torturé ko. Walayy il dira fou Lissa nekk. Vu ke Justice defoul ligueyam gnome gnou dieul les choses en mains. C tout !
Képp kou guiss cette femme appeler la police aider son père à retrouver cette femme elle est au Sénégal cherchons tous ensemble on la retrouvera par la grâce divine inchalla
Salama mes amis allons faire des TIk Tock pour l' affaire lissa tine s il vous plait il faut le divulguer pour aidé ce vieux est Lissa
Sokhla lanou loolo
Je vois un père de famille épuisé triste 😢 oh Seigneur éclaircit cette affaire justice sénégalaise dal amena bras long depuis 03 ans ça traîne pas de résultat c’est difficile. Justice pour lissa tine
Que Dieu éclairci la disparition de Lissa Tine Amine
Justice pour lissa tine li Metyna nonou la bou len meusseu bayi continuer le combat Metyna ma trop Bilay dem len si presse yeup aussi def len marche pour Au niveu de Dakar justice pour Lissa Tine 🥲🥲
Man dama yakar ne wadji dalène ligueye
Pourquoi un dossier sans suite??? Vous avez des preuves sur le taximan et à la quincaillerie🤦😏malheureusement on a une justice corrompue walahi🥺🥺son ex mari sait tout sur lissa tine
Nioune wa refane ak kouy sénégalais yepp nioo wara organisé marche au niveau de Dakar justice pour lysa Tine lii dafa meti trop bou nekone sa rakk damay ray ndayam wala ma kitnapé yayam
Li môme je ne dis pas wa réffane mais sénégalais gnép gno si warr diap car li père bi wakh rék nékoul ni daffa réral khar wala fasse mais domou Adama la té dafa am akh AK yéléff si rewmi li kén warouko sétane
Ce papa est vraiment épuisé vu sa manière de s'exprimer thi deug leu neh da am yo khamné sincerment diarul gassss mou sorri thiey senegal esk on é en sécurité
Pa bii yeureum nako 😭😭😭😭
Bilahie
wallahi
Yalna yala nite Lissa Tine ak foumou meunti nék thi barké al khour anoul kaarim 🤲
Justice pour Lissa son père est très fatigué
Dès fois damay guise ay cas bani est-ce réellement Sénégal 90% musulmans la
99% la sawaye
Fall li ça n'a rien à voir avec la religion stp
@@matarfaye2696 99 pourcent des pays musulmans sont des bordel à ciel ouvert
@@matarfaye2696 94 % des musulmans 4% des chrétiens et 1% d'animistes
Même histoire juste que lissa n'est pas retrouvé Qu'Allah soubahanahou wa tala donne des éclaircissements sur cette affaire
Amine metina doyna war trop
Amine ya rabi yalna yala léral si barké yoneti bi 1nchalah
Massa Baye Boye yallah na ko yallah nite 🤲🤲🤲🤲
Rewmi mingui melne amoul justice. Ay taxawou len pabi waay
Wolahi
A mon avis je pense que ni dafko ray.parce que liko diaral dem Mali,Burkina fasso dem guinée kokou amna loumou def lou reuy.séquestration rek diaroul lolou yeup.modou yade heure bi si kasso bi lako waron fek
C'est louche en tout cas ! Sunu justice bi tamitt warneu guéneu déf sen liguey
Walla mou sacrifier ko dofloko pour alal ba paré neubeuko 😡😡😡😡ce Modou c un monstre
Dina fégn légui inchallah
Dafa beugone xarou mom moudou yade d'après informations.
Donc amna loumou déff xaléy bi bakénn dafa fore😢
Defka Ray ou sacrifié
Ndeysan li waroulon am 1mois bay am 3ans dafa eup li état bi naci wakh c'est trop facile. Le Sénégal est un pays de loi et de droit.
Diary Sow geunoul.lisa.tine.déflén.liguéne.wara.déf.waye
Ndeysane pa bi xamnakoo Aka bakh sama diarbate rek lalay wah âme yitè papa yalna sougnou indi Wat lissa sa lokho
Je vois un père vraiment désespéré et sa me touche vraiment beaucoup 😢et la justice doit faire son travail sa me touche jusqu'au fond du cœur
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Justice justice justice ..Sonko rék lép bakh ☝️ inchallah
Une triste histoire. Pourquoi la police ne fait pas leur travail .Le gouvernement doit suivre ce dossier
Pabi manchallah ku tey te kham limuy wakh Yalnako yalla nite
Ki dafa beugue dome dji ndeysane yalla lepp ler @kewoulo tv diaplen siii
Demna kéwoulou feula dieuké
@@sokhnadiop5172 c vraiment dommage
Classez sans suite ??? C’est terrible ! Qui est modou yade? Ne baissez pas les bras papa cherche ta fille du courage faites appel au président de la république
Franchement je suis dépassée li Sénégal la khawé ni
J’ai peur
Paa bi damako yeureum kounei Sénégal amoul injustice rekk danko doundoul
Justice 😭 pour notre grande sœur lissa tine papam ak yayam sonouna niou lol 😭😭😭
c grave cette histoire yalna yalla lérale leuppe
Révoltée sur la famille de modou yade,moins de 73h justice soit faite
Modou yade mi mom moy kane? Guénel domou diambour. Mais tamit loutah classer sans suite ? Mane dh je comprends pas la justice de ce pays libérez cet homme s'il vous plaît sone neu akh ndiourél dafa fort 3ans guisso sa doom li métina si khol
J’espère juste que Lissa est vivant Li metina dey Que la justice fasse son travail way guissouniou Lissa ta Modou Yade di dokhantou Nice
Yomb na trop way
Ndeysane lo métina, thiey justice sénégalaise 😭😭😭😭
Ndeyssan daguena wara deef marche bathi bountou palais ba 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Vraiement Modou yade doit etre arete et sanctionne
Sénégal da am nio wamni mousougne danguay faye ay nit niou kidnappé wadji une semaine niou torturé ko tant que waxoul bouniouko bayi soudon man je ferai pire yone defoul ligueyam nga nekeu nandité ba guiss sa dom père souma amone sa numéro ma dioxla solution bilahi té dosi fegne yombouna trop koulay diay woyou nga diayko mouss 😡
Meun na waat ni moko sakal pèkhè Ba paré guètarou Ba kèn douko teuth Mai’s yalla guiss na lèp
Vérité absolue même moi j’ai pensé à ce que tu penses
Yalnako souniou borom niit in Shaa Allah'
Cest trop triste yalla nako yalla fénial si diam inch'allah
Doyena ware
amine
Amiiin'Allah cii barakatoul kazzou radjiab bii Àmiiin'Allah !!!😔😔😔
Doyna war déh del déf Ay nafila 3hdu matin déf Ay aftazfiroulah yalla eupeu gneup dole inchallah Dina fegne
Ndeyesan metina deh yalla na def jammo rek inchalla
Yalnako yalla indiwate si wa keuram
Qu attend la justice pour faire une enquête ??? Yala na sougnou borom léral lep. Inchaalah.
Yalna ko yalla nitt si barké Serigne Touba.
C'est vraiment triste métti na trop wayyy mais doolèn publié photo Modou Yade ndakh gnou khamé ko boog
Sama yaram dawna dama dioy bilah Refane la deuk mai sonu nagn de trop
wa faye Loufa xéw 🤔🤔🤔
Bilaye lepp dina lerr yaye sa paté coura paté féguane dokhore guette bilaye affaire biii dina lerr thi barké mames yi Tine dioguoye samba Dieu es au Contrôle 😭🙏
On est au Sénégal guisgua modou Yade 3mois yi mou Dem kene guissou ko c, est Louche demna defari bopom si maraboutage pour kene d'où guisse dara te d'où moudier feneu kou Dem yobale ay millions niou tok 3mois kene guissouko khamguani préparé n'a bopam bou yagu Lima yakar moy raynako
Méti na wayé yalla guis na lépo 😭😭😭
Cheiuuuuuuuuuu bane Sénégal lagnou nek😭😭😭💔💔💔
Ndeyssane nio bokone école privée mame cheikh anta mbacké bou touba toul yalla nako yalla nite
Papa va voire là où y'a les carreaux peut être elle enterré laba comme dans les films
Yallana yalla lelar lep inchallah metyna trop
God bless 🙏 that girl
Amiiiiin'Allah
Justice pour notre sœur Lissa Tine
Demal sa serigne mountakha mou wo macky niou geuné lisa tine
Modou wakhal Ani Lissa sayayou domla fokonabah dibalil family sonanatrop metina 😢😢😢
Triste histoire. Sénégal amoul yone
La seule chose que je vous mes frères et soeur nine partagè video yi si tik tok ak Facebook pour denoncè encore injustice bi c'est triste vraiment ypa de justice dans notre pays coumba ame ndeuy ak coumba amoul ndeuy mofa ame
Geumnani modou dako rayy soûl ko fou sori ak vayagam you beuri yoyou . Mais Yallah dinako meussa werr
Modou yadd nagn ko torturé mou wakh limou def
Modou khana ab djiabar leuu 🤣🤣🤣🤣
Merci amy
Yalla nako yalla nite inchallah yalla bakhna
Yalla nako yalla gnite si barké seydina Mouhamed PSL
Sénégal fiii lépp mofii amm 😢
Amine 🙏🙏
Mane dè nianoumako yalla Li dal ma wayè souma dalone mane AK modou dounou bock adouna bi blh
Yalnako yalla nit du courage père métina trop
Doynaware 😭😭
Yalnako YALA niiite.inchalah
Que ces frères tabassent bel et bien Modou yade du moment que la justice ne fous rien qu’il le règle à la barbarie rek vous avez êtes trop patient
Vous avez parfaitement raison
Bonsoir les sénégalais le 14 avril 2019 a octobre 2023 c'est 4ans 6mois au lieu de 3ans merci
Une amie a mw depuis enfant bilahi elle me manque bcp bcp jumelle ❤️😭
A bon
Metina trop
Masta Cherie
Oh justice pour notre sœur
Li métina trop way
Yalla sougnou borome léral lepp
Li tamite doyna warr kéne dousi wakh ana justise Senegal nak li metina troep
Sénégal une justice à deux vitesses c'est triste YALLA nako YALLA nitt
Vrema li metina
Yalla nako sounou borom fanial lissa
Ndax deukk bi amna yoonnn🥺
😓😓😭😭
Justice pour Lissa
Pére Sénégal amoul justice ils sont tous des corrompus, soudone maye yow modou ngaye diape yewko bamou dougeur guasse paxe soul ko , kome nimou def sa dome
Sama Ay mboko lanou métina lool
Waayé gnoogui taalal lokho justice bou Senegal
Modou yade mi bougnou niafé ndém légui légui xalé bi guéneu!
Boudone may domou pa bi na déf le tout ba kidnappé ndéy Modou, doundouloko diakhanama
Exactly! Même chose la khalate. Ils doivent kidnapper le gars dindi galathie yeup torturé ko. Walayy il dira fou Lissa nekk. Vu ke Justice defoul ligueyam gnome gnou dieul les choses en mains. C tout !
Bonjour la famille de lissa non qua faire leurres propres justice cils long fait la justice vas réagir merci ces ma conviction
Yalnako Allah nite si diameu
Mais lou justice dii kharr sii Modou oubien nékoul Sénégal
Yallanako yalla notre bambou fégne
Vérité absolue😭💔💔🙆♀️
Ou
Niafff len ndayam mu guene ko qui dafa ya yabate
Limetina deh justice 2poids 2mesures.le dossier pietine..
Modou yatt d daléne meuneu thi galath wayé yalla moko eup dolé
Dou dem si serigne amsa wakh kouko bakham mou mane thi dara
Limitima.ama.justice
ba defouka sacrifice 🤔🤔🤔🤔🤔
Li yomb na dh c'est quoi ces âneries comment ça dossier classé sans suite
Avec toutes ces preuves lougnouy khar
Yalnako yalla nite bamou fegne thi diame
Suis lissa Tine😭😭
Sortez la photo de modou yade Niou affiché ko si Deuk Bi on verra mais justice Sénégal louy sen problème à la fin 🥺
Yalnaco yalla fegnal