Griff mo daka féneu ak gnodi , moom fila bayi rakaam diapalé wouko di battrè Wally seck ak Pape Diouf . Pendant ce temps son petit frère di fréquenter ay bandit bagni raay ko au parking du stade leopold sedar Senghor
Griffou mo bari wakh té meune togne. Mane khamouma mo gates té meussou maka guiss mais griffou chaque fois mou togn ko. Té meussou ma dég fouko mo gates wakhé lou niaw. Bayil domou diambour yi té liguey bi wakh. Dioulit dou sokhore ak titarou. Gor dou téssaneté ak garouwalé.
Thanks Grif ❤❤❤❤
Griff wakham dafa anda ak Sokhore. Purr mome mom rek mor bakh. Ngaka deug la
Live bi khana amenako khamni la toudeu griff yalla bo kham sama soxla non yeneu yi febar la
Griff vrai waya waya la doff deug la en plus koula degg khamni rancunier ngua
Dey xuloo rek wadji 😆😆😆😆
Ya wayadi
Sa waye sa wakh beurrina en plus lepp li nga done deff ngane ya ngui ko done deff si sutura legui nak ya ngui weure di wakh
Grif❤❤❤❤
Grif bayil doull yaw khame nalla bakh doul rėk gua meune
Example yi ak anecdote yi barina
Griff mo daka féneu ak gnodi , moom fila bayi rakaam diapalé wouko di battrè Wally seck ak Pape Diouf . Pendant ce temps son petit frère di fréquenter ay bandit bagni raay ko au parking du stade leopold sedar Senghor
DEUG rek la wakh. Jeune bouko dégue djeurignou
Grif dey wakh sohor ignane alors que mom mo sohor mo ignane tu le vois dans sa parole
Griffou mo bari wakh té meune togne. Mane khamouma mo gates té meussou maka guiss mais griffou chaque fois mou togn ko. Té meussou ma dég fouko mo gates wakhé lou niaw. Bayil domou diambour yi té liguey bi wakh. Dioulit dou sokhore ak titarou. Gor dou téssaneté ak garouwalé.
Grif xallis bi nonou la démé
😂😂😂
Ki deh ignane ak beug xewwww rek moko defff diaral lii
Bou khaliss bi douguè donc tu connaissais la provenance de cet argent griff lol donc il n'as pas fait ce que tu voulais et tu le sali lol 6 moy 9
Yaw togne kate nga