Ayy sama future femme amal caractère nii Biddew meune toggou nii mom beugeul sa diabote nii mom amal diameu way future femme..(C'est moi qui t'écris au cas où tu lis ce commentaire 🤩😍)
Mbape joueurs la non badiene Ray nama mes issmaïla li mom bakhna 😂 thi yaw ndeye Coumba boul bayil DH 😜🥰mes bi khetou forme tamitt ahh man dall 😁 beugue n'a li man😜😁😁
Da âme louma diaxaal loutax femme marié yii sééne ex yii Souniou léne womé niou tite soudé xamoul nii amgua borome dokokowax bééne yoone mou xamni tu é mé dii tite baasaa borome keur koumacé am souci sii yaw le passé c le passé nit dakoye wax deukk lii théâtre laa mai pour la vrai vie motax maaye wax soyons direct avc nos ex
@@khadidiatoudiouf5191 non non douma Marié mé dafa rafetoul après le mariage amato droit dii tite thii saa ex boula wowé kakoye neup Come sii daakoo noppate Lolou sa ex souko xamé meuna dila si chantage té baxoul j pense q une une femme Marié doit être digne et montre la confiance à son mari oubien
@@rokhymane4263 cest ce que jai dit je suis mariee ne m'appelle plus loy ragal.thi mom fofou lay wakher apres il.ne va plus t'appeler dis moi soudoul lolou lou dess? Khel.meutoul
Nguir YALLAH ne créer pas ici un petit ami pour Beedew, essayer d’introduire au moins sa famille car depuis le début on voit que la famille de Mass. Mais affaire farr mom tout sauf ça
Wa lane montakh soléne beugué j'aime dit n'a kou beugue Seydina Mohamed Seydina Mohamed niepe ko beugue AK di tou dou séne yayi fi kou neka beugue sa yaye déme maka bayi léne liguéni def
Chers frères et sœurs. Le moment est venu de s'unir contre les puissances du mal. Jésus-Christ peut revenir n'importe quel jour maintenant. Le temps presse. Repentez-vous de vos péchés. Gardez votre foi forte. Continuez à avoir confiance et à croire. Seul Jésus peut nous sauver.
Connaissez-vous la série *LEMZO CHÉRI* ???
Oui
Moy bou bess bi t nekh
B1sur🥰🥰kagne lay dawaate book
Oui
Oui mais essayez de mettre les traductions surtout la série biddew, il y’a beaucoup de personnes qui ne comprennent pas le Wolof.
Merci d’avance.
Une pensée aux personnes qui ont passé ramadan passé avec nous et qui sont partis rip 😭
Ndeysaan yàlla naleen buur yàlla yërëm té xaare leen thia Aldiana you guena kaweee ya ñu ñu fa fekk ak ñu leen fa fekk 🤲🏾
@@peaceandsalam2852 amine
Paix à leurs âmes
Yalla nagnou khipé firdawsi 🙏
Paix a leurs ames
Dema togn rek.. Parce que tu ne sais rien 😂😂😂
Bou wadiour yeup done def ni deh bene khalé dou raté wakhtou machala 🥰🙏🏽
😁 wllah
Billaye
😁😁
Bilahi liiii meun nama raye🤣🤣🤣
C mon cas il fait les mêmes grimaces que le garçon
Ceux qui regarde bidew à cause des conneries de Badiene et de Fama lalein like way🤣😂✨
😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣
Nio Maye Raye manne
Moi
niaw badienew amna mere bou ko ngueuna grave.
@@fatougueye3263 bilay mane tamitt 🤣
Wa ani gni fama takh di setane bidew 👈👆👆👆👇👇bilah mokoy nekhal Aÿ khetou terme mam%
Je l'aime
Wouyyy badiene néna mbéppé dh joueur la😄😄
Mbappé moye joueur mbéppè moye nopile
Fama lingaye sagnsé mba diammou la🤷♂️
Fama da kham sangnsé
Machala
Waxall dhh sagnsé rk lay deff😍
Ramadan Mubarak à tous nianalen ma année prochaine inchallah ma ame borom keur bou bakh je le souhaite à tous les célibataires aussi merci
Appel moi je suis libre
Année prochaine prkoi pas pas année bi
Yalla nala ko yalla may
Yalna yalla mayla borom keur bou bakh si ioe si barke saydina mouhamed psl
Yalna yalla mayla borom keur bou bakh si ioe si barke saydina mouhamed psl
Ndeye coumba ak domam bou guaur bi dina niou ma ray 😂
Non ndeye coumba dou dem😂😂😂😂
Ana sopey seydina mouhamed psl beusseul abonne svp 🙏
Non ndeye coumba mou ngui yakk sama adina😂😂😂😂 "parsk u ne sais rien"
Nom j adore nimou deffe chok domdji si demal diouli bilay Def Sama bosse 😂
@@ladivandiaye2230 😂niatta att la amm??
Fama linga lunette lane la😁🥰
Mère bi mogui coach dome ji mais dane na deff différence xalei bi jongoma na🥰🥰
Par ce que tu ne sais rien 🤣🤣🤣
@@mounadieng5687 ndanan l...souko mayé dome bi req m tothie😁😁😁🥰
Bravo à vous
Au moins dans se sketch on rigole bien et apprends des leçons de vie .
Badiene yagui belle machalla ❤️❤️❤️daro liguaye sagnset lane la tamite dothie bole meune togue
Ndeysane j'adore le langage et les liens que reflètent la maman de daro et sont frère c'est cool de voir ça
Fama sayyyy sagnssé tmt machalahh nicena trop sa vert lanela tmt sa lunette yi diapenalla trop
❤️❤️❤️❤️❤️💯
Ayy sama future femme amal caractère nii Biddew meune toggou nii mom beugeul sa diabote nii mom amal diameu way future femme..(C'est moi qui t'écris au cas où tu lis ce commentaire 🤩😍)
They yalla iow hamenala sur les commentaire🤣🤣
@@ndeyenogayedieng5660 de même
que moi ki khameenako 😂😂
@@khadymboup9881 dama waru d lol mais c juste pour taquiner
Meune sagnsé ni Daro 😃
D'accord b
Mbape joueurs la non badiene Ray nama mes issmaïla li mom bakhna 😂 thi yaw ndeye Coumba boul bayil DH 😜🥰mes bi khetou forme tamitt ahh man dall 😁 beugue n'a li man😜😁😁
Kou gueme ni sa yaye Dina dem maka beuseul j'aime 🙏🙏❤️
Bidiw diék bou mane wagne warr na yéé dièk you bari dh💁♀️
Fama mon néxal séri bi 😅🤣
Fama mon néxal séri bi 😅🤣
Fama lingayy sagnsé diameu leu😘😘😘
Fama lingayy sagnsé diameu leu😘😘😘
Man fama la beug bilay Artist deug leu walay naniou bayikhel ✌️😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Maise Kharitou Mass biiii beugg na luu yombuu dh ,lekkk rk nguay yeurndou siii ayyy Mure nak 🤭😂
Aye diaralma sa dane ndeye coumba Dinama ray mane mome de moguene jongue domdji waye khalebi ak formome rek 🔥🔥🔥
Merci sis ❤️
__“Parce tu ne sais rien” cette citation😂😂🤣
Ma touty! Teint noir machalah tabarakalah! Jolie tenue! Daro non do dem!😂😂😂
Non mère bii soff n'a ak tu ne sai rien😂😂😂🤦
Da âme louma diaxaal loutax femme marié yii sééne ex yii Souniou léne womé niou tite soudé xamoul nii amgua borome dokokowax bééne yoone mou xamni tu é mé dii tite baasaa borome keur koumacé am souci sii yaw le passé c le passé nit dakoye wax deukk lii théâtre laa mai pour la vrai vie motax maaye wax soyons direct avc nos ex
Deug leu dh melni kou défoul diam sa ex boula wowé kay néko amna dieukeur bouma wowati mou diekh
Lou lér nga wakh jeul ko wakhko lifi nék
Vraiment wahko tu es mariee lou khew
@@khadidiatoudiouf5191 non non douma Marié mé dafa rafetoul après le mariage amato droit dii tite thii saa ex boula wowé kakoye neup Come sii daakoo noppate Lolou sa ex souko xamé meuna dila si chantage té baxoul j pense q une une femme Marié doit être digne et montre la confiance à son mari oubien
@@rokhymane4263 cest ce que jai dit je suis mariee ne m'appelle plus loy ragal.thi mom fofou lay wakher apres il.ne va plus t'appeler dis moi soudoul lolou lou dess? Khel.meutoul
loutakh gni meune kharane gni , nioye animé tjrs🤣🤣🤣
Daro nak sikk gua ba nioulay tékalé akk radio Dakar😂
🤣🤣🤣
Momay ray🤣🤣🤣
Mbeper joueur leu😂😂😂😂😂
Li mane nama raye😁😁😁😁😁😁😁😁😁
Ak man😂😂😂Ray nama
😂😂😂🤣🤣🤣😂
Raynama da spontanée
Wa youssou mi tamit Esk dou bayi harane nanditè bi mouy def 🤣may wah mounane projets 😂😂
Youssou xarane rk la mane 😁😂d1yy kothie heur bi😁😁
Biddew je l’adore vraiment je la suis depuis 2019 a l’extérieur
Thiey fama sama toma sagnesé rek lay def💃💃machalla Jaime tal
Billay toma avec fama yii rék💪
Q
Meilleur série du l'année ❤️
Meilleur série du l'année ❤
Loumaléne wakhone 🤣 youssou meussoul ropbou Diamndiadio ak matelas wam bi🤣🤣 wawaw kou amoul lo fayé boor meune léke si plat bideew yi ba sour😁
Yaye danga may togne rek
Parce k tu ne sais rien
Di nagnou ma rayy
🤣🤣🤣🤣🤣
Bilay surtout lolou 😂😂
Le nouveau slogan 😂😂😂😂😂
@@konatemuha7106 no gni amougnou
@@alimaseye1542 mom lay may sama yaye légui 🤣🤣🤣
Tay mom dama gorgorlou mbéde TH-cam yi bariwou ma thie tank def léne ni mane 🤣🤣🤣😂😂
Woute ake mane. Momaye weteli😄😄
@@seynas7757 yémé na 🤣🤣
A wawaw mane ai yaw nio yemm🤣🤣
@@tymasall8545 tay mom dama ko daw
@@seynas7757 badou😂
Non merbi nexna bilaye nenako djeleul eponge té déme ci dane 😂😂😂
Bizarrement bamay lir sa commentaire la tomb ak action bi
Lima diahal chaque saison bideew gane you bariwakh lay am!!
Nguir YALLAH ne créer pas ici un petit ami pour Beedew, essayer d’introduire au moins sa famille car depuis le début on voit que la famille de Mass. Mais affaire farr mom tout sauf ça
Bilay néhatoul sahk😔
Dano bg yak contexte bi rek li mom andoul ak logique bi
Mane la déh soga nièw si lang gui dilèn ziar ndakh "katalolèn ma solèn ma katalone douma meuna commenté en paix "😂😂parole d kaaw
Yaw dé nimala khamé dafa eupe 😂😂
@@bintouseye4825 ay kouya bayi🤔🤔🤣🤣
😂😂
@@bintouseye4825 même man 😂😂😂😂
Diapal dioulli 😂sheuttttt yaye dang may tonie rkk😩😩😩😩psk u ne sais rien😭😭😭😭😭😭😭😂😂😂😂😭😭😭😭😩😩😩😩
Lii manoumako moug😁
Fama kagn lay am diom tamit 🤣🤣
😂🤣haaran kaat foko fekk deiy manè Taasu"🤣🤣🤣🤣🤣🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Ndeye coumba raynama nena fompalma sa kanam gui té demm woyy kou ndeye coumba di Ray ak parceque tu ne sais ríen 🤣🤣🤣👆👆
Dama fok nè legui ay jaime 👍dagnou kay ndogo lègui 😂😂😂
Mbappé deh joueur leu🤣🤣🤣
Wa lane montakh soléne beugué j'aime dit n'a kou beugue Seydina Mohamed Seydina Mohamed niepe ko beugue AK di tou dou séne yayi fi kou neka beugue sa yaye déme maka bayi léne liguéni def
MoMA diakhal da nio Wakh ba sonno lépe Pour âme j'aime li ba diamou la ahhhhhhhhhhhhhhh
@@fatougueye3263 wawe li dou diamou des jaime diarna li
@@diarrychouka3507 beugue jaime darna lounek
Gni souniou fi waxaté:
"Yaye dagua may togne rek" "parceque tu ne sais rien" souma léne kheutei 😂😂😂🤣 dinaniou ma ray rek🤣🤣
J'aime l'habitude de ndeye Coumba à chaque fois il dit à son fils d'aller prier
Mère bi nama réception parce que tu ne c'est rien 😂❤
« Par ce que tu n sai rien » meune nama ray 😂😂😂
Bideew waxatanal ak sa djeukeur bayi neubbeutou bi bou waxtan amoul rek rèro am 😊😊
🤣🤣😭
Chers frères et sœurs. Le moment est venu de s'unir contre les puissances du mal. Jésus-Christ peut revenir n'importe quel jour maintenant. Le temps presse. Repentez-vous de vos péchés. Gardez votre foi forte. Continuez à avoir confiance et à croire. Seul Jésus peut nous sauver.
Héhéé dina dé rkk😂😂😭sheutt kone wadji day youndou balamo kharane siii
SL BIDEW JE SUIS BEAUCOUP DE PLAISIR À VOIR TES VIDÉOS ET TES NDOGOU ELLE FAUT M'INVITER QU ON PARTAGE LE NDOGOU ENSEMBLE
🔥🇸🇳😍✊🇸🇳🔥la meilleure série du ramadan #biddew on adore 🥰❤🥰❤🥰❤
😂😂😅ismakhila ake yy dji dinan ma rayy môme dioulli la koye niaka lathie
Laaaay déké youssou beug di kharalé rérr bidew bi mo takh mou dann diouli rekk😂😂😂😁😁😁😁
Wayè nak kharitou mass bi gate na khel dhè🤣🤣🤣chak jour mou niew teksi beri wakh
Meilleurs serie machallah mass racine Niang yalla nala takhawou arc la yorr succès bi barki mouhamet non keur fama nekhna
Taxi lala téguon kay no fama dou dém 😂😂
J'aime beaucoup bideew waye
Biddew ki dila wo waako foula ta wakh tane si ak sa borom keur
walay yambar mi
@@niangadama3809 😂😂😂
"parce que tu ne sais rien"mais parce que Yako diangue lo woule dinéme
Fama radio Dakar eupena😂😂😂😂🤣🤣😂😂😂😂😂
Bideuw Amal foula nga wakh ki bopam mo Arrété
Ay yena gaw🤭
Parceque tu sais rien 😂😂😂😂 elle v m tué 😂
Qui est le meilleur entre biddew et adja
Biddew wakh ko masss
Lii douma si doyal mbappe joueur la😅😅😅😅
Ki mo meun xarane mongui may fatali temps boye😂
Yalnanou yalla Doli diamm 🤲😍
Yangui founé wéléleee😀😀
Guir yalla boule def bidew âme prolem ake mass ki môme diaroule wogne mou fi nieuw Di yak ménage bidew bi
Bidew ak ramadan de guagne gnoye sama préféré ak kane
Nigir dieumi serige touba à bonne léne fi si kourel khassida tie yalla takh 🙏🙏🙏🙏
Fama elle va me tuer avec ses manières
Ndeye Coumba damako beugu way😂😂😂ak béne expression bimuy may Dom djiii😭😂😂
waou cool Bonne curage a vous
Daro dé niamakh niamakhi la kham nguéne beugue ko toklo no lolou meunoul néke. ☺
Bidew toujours aussi belle machalla
Ndeye coumba nekhal na série bi
Mai badiène corona bi dièkhagoul dh daw mome distance gue done wotè mai saison6 bi mome aml masque aml distance😂
😂 😂 Nenako Mbappe dé joueur le🤣
Macha allah bonne continuation
Khariti Mass gii dhu takka jabarr
Following from MAURITANIA I like it
Neubeutou bakhoul wakhal mass deugu rk ba darra douko bett sinon si ay problem ngéni moudj
Mbappé dhh joueur leu🤣🤣🤣🤣
Wa Kone Youssou môme heure bou bakh bi rek layy natteu 🤣🤣🤣🤣
😆😆 youssou kay moy lolou
@@alsinisamb4800 ki dé bou koor gui Di diekh dotougnouko guiss 😂
Mbappé dh joueur leu 😂😂
Bidew stp dégnou wone niguay togué nak gnou topando😂
Nice n'a vraiment j'adore sette série
Wa domou ndeye coumba bi limouy sol tamit ak werr wi doka selal
Nékhoul ba nékhoul mais ame diabar bou melni bidew diamou Yallah leuh.
Youssou mi kharan katt la dh 😂😂