Akassa dieuredief serigne mountakha mbacke balla Yagüe fi loooll ta wér barkep borom TOUBA ak mame Thierno dieuredief néll amine yara bi kou ni amine yalla ne ga féké déwénn ta yalla ne yalla wonélélak seydina mouhamed psl si barkep seydina mouhamed psl amine
Bilahi sama série bi yalla nay Di am niou yagueko di sétane. Franchement mashallah leuzTV. Limaci gueuna nekh Moy quand Youssou a dit à Germaine mashallah chrétienne bouy diokh djoulit ndogou. Li deh Sénégal rek la am et deux jours après rek ma dégueu k chrétiens yi danio done distribuer ay ndogous djoulit yi et pourtant ces épisodes ont été sûrement tournes avant le ramadan. Mashallah lii Moy senegal 👍
Bonjour. La série est excellente, quand l'épisode se termine. On se dit: Ah non. Macha Allah ❤️ Félicitations à toute l'équipe. Je suis fière de vous. Macha Allah. Bon ramadan. 😊
Fama nak dof ngui koy beug dikkal 😂. Niakeu wolou sa bop mo bone 🤦♀️. Biddew esk nekoul di commettre erreur. Mi ngui demander de l'aide à tout le monde sans le dire à son mari
Moi je ne comprends pas le comportement de Bideew .Pourquoi se creer des problemes alors qu’il ne s’agit de d’un EX.Tout le monde a un passe.Pourquoi ne pas parler a son mari ?
C'est bien d'avoir introduit des personnages de culture diolas, le Sénégal est un et indivisible. Les diolas sont des gens qui sont en général honnêtes, respectueux et très courtois
Merci Bara tu as tout compris Sénégal bénen bopp la kéneu menou ko khar diola ,peul,sérère,toucouleur,ndiago,sarakholé gnoune nieup ben lagnou on est frères et sœurs ❤ En plus Bidew est diola et on est fière d'elle machallah 🥰🥰🥰💕❤
J’aime beaucoup cette série ainsi que les acteurs et qui nous accompagne chaque année pendant le ramadan.c’est un plaisir .je suis fiere de voir mon amie Mariam Goumdiam qui représente la diaspora ❤️🥰🥰🥰dans la serie 🔥🔥🔥.hate de voir la suite inshallah 🎊🎊🎊🎊
Genre Daro yi nioye pousser sen dieukeur yi takk fekk il n'avait mm pas l'intention ndeysane do seye beugue fitnal sa dieukeur andoul daleu Seye stratégie la tamit
on dirait que bidew comprend diola elle a repondu au vieux avant qu'elle ne se rende compte qu'elle devait faire semblant de ne pas comprendre en tout cas belle intiative vive le Senegal uni💖💖💖💖💖💖💖💖
Première commentaire kou beugue biddew wakh deugue gui mass touch j’aime 👍
Merci chérie
Non dafay bagn mou manké confiance si mom c trop compliqué
Kou gueme ni sa yaye Dina dem maka beuseul j'aime 🙏🙏❤️
Amin
Moi
Moi
Cci
ku gueme baye ak yaye baye dafa sonnu suba ak ngone ndax domam
Koorou bidew meilleure série du ramadan koussi d'accord laalal j'aime 🥰🥰🥰
Oui je siue d accord avec toi
Je suis d'accord avec toi .
Chaque année day geune nekh machallah
Khana doy setane Serigne ngagne ak kaw duo bobou meusta am🤣🤣🤣🤣🤣
@@ndieumbeutembodj4749 bobou nexna wayé batay rek bidew ak Adja je valide
Cci
Yalna yalla are tè samou sougnouy wadiour. Gnikko gnac. Yalnalen yalla maye kholou mougne si barke seydina Mouhamed 🙏🙏🙏
Amine yarabii
CCD
Amine
Amine yarabi
Amiin
Sounou biddew national kou d'accord🥰🥰
Mane
Mane
Dans cette série les acteurs assurent vraiment. Je reste impressionné par la petite fille
👍👍
Moi aussi
@@syndinak2392 p8
Əəəəə
Tout à fait
Familles Germán sof nagn bâri wakh qui es d'accord 😂
Moi
Année bi mome germain mon ayer
Nonnnn dagno sof kat ex bidew bi osi fateu nagnou lii foumou am topou kou Marié
Virement 😂😂
🤣
Thiey wa team setan série yup manifestez vous
Famille germaine qui es tu
@@zeydamamybadiane4552 e😄😄😄😄😄😄😄😄😄
Mangui ni😂
😄😄😄😄😄😄
Bravo Mimi. Please keep it up!
Akassa dieuredief serigne mountakha mbacke balla Yagüe fi loooll ta wér barkep borom TOUBA ak mame Thierno dieuredief néll amine yara bi kou ni amine yalla ne ga féké déwénn ta yalla ne yalla wonélélak seydina mouhamed psl si barkep seydina mouhamed psl amine
Amine waye sama touma borom Darou
Amine way
Aaaaaaaamiiiiiiiiiiin
Amiin
Amine
Daro bonne continuation vraiment ça fait plaisir de te voir conduire c'est magnifique 😍❤️❤️❤️
Bilahi sama série bi yalla nay Di am niou yagueko di sétane. Franchement mashallah leuzTV. Limaci gueuna nekh Moy quand Youssou a dit à Germaine mashallah chrétienne bouy diokh djoulit ndogou. Li deh Sénégal rek la am et deux jours après rek ma dégueu k chrétiens yi danio done distribuer ay ndogous djoulit yi et pourtant ces épisodes ont été sûrement tournes avant le ramadan. Mashallah lii Moy senegal 👍
J'aime bien cette série. Bideew est très belle tabarakallah 🥰 Fama toujours dans son rôle elle joue bien. Félicitations à toute l'équipe korrou Bidew.
Waawaw topnaa Kou dionguama😂🥰🥰thioum djiguéne Day fess ,meune,gueune
Cc
@@Yattandiaye2007 slu
Sauf
Bonjour. La série est excellente, quand l'épisode se termine.
On se dit: Ah non. Macha Allah ❤️
Félicitations à toute l'équipe.
Je suis fière de vous. Macha Allah.
Bon ramadan. 😊
Guir dieumi serign touba....yalla na diam yagu senegal 🙏🙏🙏
Thiéy fama toujours aussi belle ♥️♥️
War guen di wax si série bi dh et évitez vos commentaires à deux balle la nous forçant à vous mettre des jaimes Tshippp
Nga sagne ko wakh. Lo kham ci wayadi
@@habydiane9480 li d’où degu way
sof rek ak wané
Vraiment
li rek moma sof
Wa Man masou ma am ben j’aime 🥲🥲😭🥲😭😭😭😭😭😭😭
Lekal mou res ak jam😂
Anni gni begueu sene yaye. Wonelen sene boppou maye guisse bokk.
Sama serie prefere notre bidiew national bonne continuation chapeau à vous
😂🤣😅bravoooo pour vous tous👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼🥰, l oncle aime les plats de Biddew😂😅
Merci papi yow au moins nieuwo pour yobou Germaine de gré ou de force☺️☺️ndeysane badjene dh dey diéma defar ba sone mais fama dal cpolapeine
Sama serie préféré biddew je t'aime beaucoup waye j l'aime ma anta
Kou begue seydina mohamed abonèll sama chain gir yala rek ta yala takh.
Korou biddew meilleur serie du Ramadan bon Ramadan a vous
Diola yi nio tax mass di siss niou engagè keur diabour bi ni 😂😅😅 germène louniou wakh 😅😅
Germaine nena lane
😂😂😂
Mann yayou Fama la yeureum 😂😂😂 fama gathia douko sonal
Gniga khameni gno done setane ak gnome serie bi daw tei reine neikou gnouffi yalla naleine yalla yeureum te kharel leine adiana 👏
Amine
_Kou beugue __#cœur__🙄 dane Adja fama lalal j'aime 😂 meuna solou té meunol togou🤣🤣_
Cc
🤣🤣🤣🤣
Fama nak dof ngui koy beug dikkal 😂. Niakeu wolou sa bop mo bone 🤦♀️. Biddew esk nekoul di commettre erreur. Mi ngui demander de l'aide à tout le monde sans le dire à son mari
Je suis d'acord avec toi elle doit parler a son mari
Bilahi c vrais
Fama rék 😋😋🤣
Moi je ne comprends pas le comportement de Bideew .Pourquoi se creer des problemes alors qu’il ne s’agit de d’un EX.Tout le monde a un passe.Pourquoi ne pas parler a son mari ?
@@Fabidi1011 mais son mari est loin d'être commode ces temps ci. Il serait capable de dire qu'elle l'a attiré à elle
Non dane est mielleur de tous les temps billahi 😂😂😂
Ahnn Kone yangui koy bayi khéll
Meilleur on dit
Hghh n lcyhojnehfzfylb ghvaccjwxhgwśghhèķjhvghc jhb
Vgj1ghmbc
Jhhjh1jgnmcgk
Cjjaoujlvljhr1gjkcbvhttykc
Hkvvclchkvshjhajhayuhdjh
Vjlqjvdcphehjmb1kh
Bbfjjifj
Jkhlvzjvuuhzhioljk
Hvfgyoh
serigne moustapha
Nooo ndéké joola yii daño beug lëk cheuuut😂🤣😂🤣 Séne BUUR Sereer mooy wakh nak 👑
😂😂😂😂bayil togne
Germaine saison bi sa boss la ak famille diola bi
Bidew j’adore vraiment vôtre stylée vestimentaire ça parfume class et élégance
Oh la la!! J’adore! Et Mimi joue aussi 😍😍😍
Waw gérméne sén wakeur khana danio amné fébarou khiff😀 ayy diola rek guén meuneu donne😀 sama diam yii😁
Peulh foumouy diarr ba nek bourou diola 🤷♀️
Khana fimou wara diar😁
Wakhtane léne ba dioubo rk😂😂
@@dienabadiallo9599 gnoy sa bour nak
Naguoul li yalla dogual rek😀
Wouy mangui dei🤣🤣🤣🤣badiene neinako bagn lakay diokh vice yi matone na 🤣🤣 déffatt thi vice yi bala ngamakay deilo 😂
Gni yakamti mou am pour xol li fama sadj dama beug sanesé sama 💝
Dane 🤣🤣🤣💓💓💖💖
Ay ndeye Coumba 🤣🤣🤣
Cc
Ana talibe cheikh yi 😍😍😍
Dane a un bon caractere nak 🤣 dautres maris auraient haussé leur voix
Kham gua ni Li série la rek mais dans la réalité dou démé ni way
🔥🔥🔥 actrice o top ma mimi , talent cacher je valide 🔥✨🤗
Machalla rien à dire mass bidew sa kaw sa kanam je vous adore vous tous vraiment yenay nekhal koor gui
No dane ak fama ndinane ma ray🤣🤣🤣
Wayé dome Sama takay or bi rk la beug 🤣🙈
C'est bien d'avoir introduit des personnages de culture diolas, le Sénégal est un et indivisible. Les diolas sont des gens qui sont en général honnêtes, respectueux et très courtois
Saway gni dania yake seri bi yeubb
@@ousmanendao6411 ioe bonne geuh de 😂😂
@@baradia4600 en tout cas, yii Diola beugg naniou lekk 😂. Mais vous avez raison c'est très inspiré de la part du staff de production. 🇸🇳♥️
Merci Bara tu as tout compris Sénégal bénen bopp la kéneu menou ko khar diola ,peul,sérère,toucouleur,ndiago,sarakholé gnoune nieup ben lagnou on est frères et sœurs ❤
En plus Bidew est diola et on est fière d'elle machallah 🥰🥰🥰💕❤
@@maguettediedhiou8421 Merci pour ton commentaire
Kou begeu seydouna Mohamed bseul j'aime ❤️😍 guir yalla
Couple dane ak daro day fay dhé
Meilleur SÉRIE du ramadan BIDDEW 🥰🇸🇳✅🤝🙌🔥❤💯on adore 😍❤😍❤
Ani sopey Serigne fallou yii ❤️
🙏🙏
Magui ni
Maï Ndiaye
Eg Fama tay Auto la lale dée voiture😂😂
Voitikh😂 Pawlish voice😂😂
Mais yène lou takh guéne fir s’il vous plaît
@@cheikhbethiondiaye7977 y'en kouléne firewoul gué sakh ay lafff😂😂
Bilahi
Ay fama li manqué si yaw eupouna 🤣🤣🤣
Mankan😂
C'est k Mane fama dal . doyna War
Machalah j'aime beaucoup Bideew elle a un bon comportement envers les gens comme Adja
Lu ler machallah laff thiatt mais yaw danga mah nou rou com gnom 😂😂
😂😂😂Adia moma yarr😂😂
Biddew je l’adore vraiment depuis l’extérieur
Ma anta meilleure actrice de l'année laff thiett ki est d'accord avc mw
Fama leu beugueueu man😂😘😘😘😘
Wa diola yi douguene wax sérére Mo dax 🥰
Non peulh mo dak😅
J vs adore on tous pareil o sénégal
@@amadousy5124 Badou dhii
J’aime beaucoup cette série ainsi que les acteurs et qui nous accompagne chaque année pendant le ramadan.c’est un plaisir .je suis fiere de voir mon amie Mariam Goumdiam qui représente la diaspora ❤️🥰🥰🥰dans la serie 🔥🔥🔥.hate de voir la suite inshallah 🎊🎊🎊🎊
Diola yi tamite beugue naniou lek trop🤣🤣🤣🤣🤣
Boul wakh lolou way
Boul wakh lolou 😀😀
Dama khamni chak jour niou niew nane sa patron meuna togue🤣🤣🤣
Ay adina amoul solo bayilennn sama mbok yi tamit mdrrrr 😂
Dett waay
Faites vite! Hâte de suivre!
Kou geum nii diga youbbou sa yaye makka beussaul j'aime ❤️
daro mou ma nekh lo da man li moye def daro💪💪💪💪💪
Kou begeu Say dinamouhamét abonnél sama sén you tupe 🙏🙏😘
J
Esk tamit ay j'aime Virtuels preuve de quoi que ce soit leu?
Écrit bien dja
Avant hier tonton 👈🤣hier maman👈🤣tay grand Pere 👈🤣bamou soti si sama mbokou diola Yi 👈 lep nguir lokho bidew🍲🍲🤣🤣🤣eupeuneuuuuu
😅😅😅 lolou la guis ni
@@evelinegomis7673 cone guisgua lolou👀👈🤣🤣🤣🤣
Mane dina bayi serie bi rék ndakh famille zérméne bi démal séyi nak an noune dano sona😱😭😭
No germaine boumu deff féne seuyii par force kagne la khéwii
Machallah les actrices jouent bien leurs rôle vraiment dans cette série bilae, ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🌻🌻🌻🌻🌻
Fama la beug 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 sadik rek la deff
Yeahhhhhh super épisode.... vous êtes au top et un big up spécial à Mariam 🥰😘❤
Série Bi de Ismailia mossy Geuna Sonou 😂😂😂😂
Mimi la bonne copine , elle gère tout ! 🤟🏾
me yéin j'aime j'aime rek waxléine si séiri bi sof geine waye akh
Vive les diolla 🥰🥰🥰
Fama dafa sadick😁😁
MiMi ma actrice préférée internationale au top✌🏾💪🏾👌🏽
Meilleures séries 😍😍
Séne série bi yakh guénko dh mom ahh chaque jour ak kou béss ahhh
Abonnez ci KHASSIDA YI TV ngir Diot si BEP KHASSIDA thi barkep Serigne Touba ☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️☑️
Fama taye ngua dé🤣🤣 on ne réveille pas une lionne qui dort🤣 combat bi commencer na, tay mou nékhe🤣 ni rek lagniouye déffe ba takale séne bope woudiou
Ki rassoulilah thi mako diéppi thi diék 😂😂
@@awandaondiaye6711 ma sœur gniou bari façon yi lagniou déffe, ba séne Serigne fipou tak gniaréle
@@soxnakhadydienembacke562 bilay eupeul rek té wayadi
Diek bou fess placame dou topé dou aki dou ôter téléphone di menacer
Non ly amoul daane Ray nguama😂😂
😂😂nena nena germene danga wara gnibi danio sonou nioun
Mbokou germaine yi deh khiff legn dieulei deukk ba di nakhassale😂😂
Genre Daro yi nioye pousser sen dieukeur yi takk fekk il n'avait mm pas l'intention ndeysane do seye beugue fitnal sa dieukeur andoul daleu
Seye stratégie la tamit
Widdew t'adore, meilleur série, ya me vibré widdew ok
Germen loumou wah🤣🤣🤣🤣
Fofou dé momay ray ci maasss Germaine loulou wakh 😄😄
Germaine loumou wakh
Billah 🤣🤣🤣
❤️Dane la beug 🤣
Germaine yaw demain sen khaley wa keur ak sen wa kogn nioy nieuw...mrci rk
Haha
Sama.Couple préféré🥰🥰😍 Npn Daro Ak Dame damaléne aimer ni🥰🥰. Mais Fama tay def bga yeufi thiouné nak😑😑
ylla na diamou yageu si Senegal Amine 🤲
Ay fama ken dou seuy ye ni 😘😘
Billahi dafa bague adouna😁😅😅😅😅
bilay ma beugue biddiew
Thiey Diola yiii bou yaguer village ken doufa dess 😂 mais c une belle culture Machallah
Première commentaire ♥️
Slt
Première commentaire💖💖💖💖❤️❤️
Famille sarméne bi loune khéwlé
Non🤣🤣 kuer dane mo dakh sakh kuer biddew ak fama rék 🤣🤣 dane manna mougne
Fama rek la name😂😂
Pateuh patiral😁😁😁😂😂😂😂
Machallah machéri Biddewo
on dirait que bidew comprend diola elle a repondu au vieux avant qu'elle ne se rende compte qu'elle devait faire semblant de ne pas comprendre en tout cas belle intiative vive le Senegal uni💖💖💖💖💖💖💖💖
Wa gayi lane mo nékhe si diabarou djamboure wadji sonnou na dée
Serie bi nèkhna trop
Mimi❤️🇫🇷 tu assures
Pabi dafa kham heurbi nak😂😂😂
Bidew diga taah suma mbogaii nyun chaalit deh 😂😂😂😂🇩🇪🇩🇪🇩🇪🇩🇪💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿🙌🏽🙌🏽🙌🏽⭐️⭐️👏🏽👏🏽