Vous devez avoir honte de publier cette vidéo, car elle prouve que Ibrahima Khalil lo n'a rien dit de mal sur Serigne Touba. Au contraire, il est en train de citer ses khassaides pour monter que SerigneTouba appelait au tawhid.
Ibrahima khalil n'a aucune problème avec les guides religieux. Mais en plus il metrise très bien les écrits du cheikh. C'est très beau sa façon de traduire les enseignements du cheikh. La seule problème c'est qu'il ne parle pas du même coté que les autres et il est courageux. Que Dieu le protège.
il a dit la pure vérité Je suis mouride talibé Serigne Rafahi Mbacké Limou niouy jangal mom laniou oustaz Khalil diniou jangal mais nak kou nék ak Lila takha joukk Boula poukaré takhé joukk mom Lou nitt wax Gua mèrr niak xam Limou waral dafa Bari Yallah naniou Yallah défal dégu ak topp
@@cheikhdieng1000 li xamna ni Lou yagu la cadre général lay wax mais kou bagn mouride sone life nakh kén meunou téré done mouride kén meunou niou téré beug Serigne Touba
Cette vidéo date de trés lontemps avant même les années 2000 depuis étudiant j'écoutais cette audio. Sama mbokk taloubé yi ce Monsieur est une fierté un grand défenseur de l'enseignement de Serigne Touba ceux qui tentent de le dénigrer sont les véritables ennemis de Serigne Touba. Si vous vous laissez manipuler par ces gens qui prennent le mouridisme comme une entreprise vous allez le regretter trés fort dans l'avenir. Le combat ce n'est pas avec Ibrahima Khalil Lo mais avec ces petits fils qui veulent faires du mouridisme un royaume et des talibés des esclaves. Yewwwu len te bayi dof dof lou gui yoonu Mouride du parti politique yoonu SIRATAL MUSTAQIMA LA.
Walahi soumawaji deugue rek nga wakh ils savent que leur mafia est entrain de s'effondrer c'est pour cela qu'il essaient de créér des problème a tous ceux qui sont entrain de réveillé les gens
Ce petit bout de vidéo à suffisance que ces exclavagistes businessman sont beaucoup plus préoccupé dans la sauvegarde de leurs propres intérêts qu'au écrits de Serigne Touba.
@@serignethioune2290 yaw mi yaye domou kouti deugueu domerame bou bonne bi. Khalil Lô khassida Serigne touba rék la firi ngaye sagua.Démale nga diangui mo gueuneu si yaw ignorant que t'es.
Ndeysann c est pas la première fois ma degg ci moom mouy diangalé di diokhay exemple diko dieulé ci Serigne Touba , mâchallah Cheikh Ibrahima ( aka beug tawhid tei mokal alhouran )
Celui qui le critique critique serigne touba il n’a fait que relater les propos du Chiekh ahmadou Bamba Je n’ai jamais cru que serigne touba a créé un tarikha Cela est paradoxe avec ces écrits et ce qu’il défendait
effectivement tous ces gens qui ont manifesté leur courroux aprés vu ses vidéos sont contradictoires avec eux memes. ILs ne croient meme à ce qu'a dit sérigne. Quel dommage
@@Alkhadimya Oui on peut le dire dans le sens où il nous apprend à vivre exactement comme les Sahabas du prophète et avoir la culture du Talibé et de la modestie envers nos guides religieux comme l'étaient les Sahabas envers le Prophète. L'Islam n'est que Soumission et accomplissement des préceptes religieux
Ses propos sont nobles et riche d'enseignement , ahmadou bamba a apporté des moyens de bonheur didactique ,mais ses prédécesseurs l'ont détourné a leurs propres faveur...
Il cite les vers de serigne touba quand ça l'arrange, Mais sur d'autres questions il l n cite jamais, il préfère même des arabes pour soutenir ses argumentaire, alors que serigne touba a écrit sur toutes les questions que l musulman pourra s poser la bonne pratique d sa religion
@@alhamdoulillallah9438 c'est là où se trouve la différence puisque cette conférence date de 1991 alors ceux qui voulaient l'attaquer parlent d'une sortie récente.
Wakhoul deug kenn Yaakaroul nit . Nioune Mouride yi Yallah laniou topei Serigne bi . Arretez de jouer avec les mot evidememt k Ndiarigne ak loor ci Yallah lay bayiko , Lolou moniou takha topp Niitou Yallah. Faut reflechir
Mouride Yi Déme Léne Diagui Diéma Kham Séne Diiné Mo Geune Séne Bokalé Yi Ak Séne Teug Yi Ak Séne Féthi Yi Lolou Dou Diiné Serigne Touba Diagualé Woul Lolou Yalla Yonéntibi صلى الله عليه وسلم La Gnou Roylo Roylo Wou Gnou Serigne Touba
Thieiy Sénégal on est tous des musulmans on va prier ensemble bok sape donc nous islam yi warougnou nous retane kounek fanga fête fait tt pour âme yalla avant la mort en plus faut apprécier selon les textes pas a partir des comportement ou des dit des gens le linge salle doit se laver en famille vive le Sénégal djam ak Salam rek
Non bou yamée si limo wakh kay diam rk lay am main li yagg na d déklou nako bou yagg mais loumana xéw manga wakh linga beuga wakh lép si yar ak téguine com s ahmadou rafahi
Bilay il ya certain soit disant mourides ou guide religieuse ne comprenne pas les écrits de Serigne Touba Serigne Touba vivait du coran et du sounnat rassou Lilah S'il était la aujourd'hui bcp de pratiques n'auraient pas lieu
Lii kayy firdé la né Yenn yenna worr diagalem Ahmadou Bamba wayé khaliill lo lou niaw thi Ahamd Bamba. Cheikh Ahmadou Bamba dé bou dikaat tone thi anduna gnou mell nii Khaliill lo lay waayooo.
Deugeuleu dé lolu yépp Serigne Touba moko wakh wayé dafeu lathié g am noppou anrifineu billahi pour g mounaka degg nakk. Yonen tébii kham kham leu koku douffi diogué yenn lolu molen réré Sunnam tamitt kham kham leu Kou ko khamoul boy dé Di tambii nari diakhalneumeu.
Vous devez avoir honte de publier cette vidéo, car elle prouve que Ibrahima Khalil lo n'a rien dit de mal sur Serigne Touba. Au contraire, il est en train de citer ses khassaides pour monter que SerigneTouba appelait au tawhid.
Vraiment !!!
Je ne trouve pas ces propos ni choquant ni déplacé
les seytanes sont partout
non on est ensemble mon frère. L'objectif était de montré que sérigne touba appelait au tawhid
Toi tu n'as pas compris le sens de cette publication
Ibrahima khalil n'a aucune problème avec les guides religieux. Mais en plus il metrise très bien les écrits du cheikh. C'est très beau sa façon de traduire les enseignements du cheikh. La seule problème c'est qu'il ne parle pas du même coté que les autres et il est courageux. Que Dieu le protège.
Serigne Touba yalla rek la fi wakh AK Mohammed naby Rassoul Moustapha ❤️
il a dit la pure vérité
Je suis mouride talibé Serigne Rafahi Mbacké
Limou niouy jangal mom laniou oustaz Khalil diniou jangal mais nak kou nék ak Lila takha joukk Boula poukaré takhé joukk mom Lou nitt wax Gua mèrr niak xam Limou waral dafa Bari
Yallah naniou Yallah défal dégu ak topp
Mani kou beugu rér di nga rér
Lé lo yague la bokkol ak lé warra thiow lé ké baguol seringe touba baguol mouridyi lotakh do wakh li khéw sahodiya nit lomo guamol de thi wara mando
@@cheikhdieng1000 li xamna ni Lou yagu la cadre général lay wax
mais kou bagn mouride sone life nakh kén meunou téré done mouride kén meunou niou téré beug Serigne Touba
Je suis sounite ( ibadou) j aime bien rafahil mbacke je l ecoute toujours
@@qatarik1982 Masha'Allah akhy fi'Allah yalna sa jam yagu ❣️
Fii serigne touba mofi nekk
Momm lagn topou ba aldiana
Yallah
Yonenti bi
Serigne touba
Serigne Touba nitou sunna merci longue vie oustaz ❤
Cette vidéo date de trés lontemps avant même les années 2000 depuis étudiant j'écoutais cette audio. Sama mbokk taloubé yi ce Monsieur est une fierté un grand défenseur de l'enseignement de Serigne Touba ceux qui tentent de le dénigrer sont les véritables ennemis de Serigne Touba. Si vous vous laissez manipuler par ces gens qui prennent le mouridisme comme une entreprise vous allez le regretter trés fort dans l'avenir. Le combat ce n'est pas avec Ibrahima Khalil Lo mais avec ces petits fils qui veulent faires du mouridisme un royaume et des talibés des esclaves. Yewwwu len te bayi dof dof lou gui yoonu Mouride du parti politique yoonu SIRATAL MUSTAQIMA LA.
Reeero bii la xamoul c'est quoi même le projet
Walahi soumawaji deugue rek nga wakh ils savent que leur mafia est entrain de s'effondrer c'est pour cela qu'il essaient de créér des problème a tous ceux qui sont entrain de réveillé les gens
Al khamdoulilah cheikh Ahmadou Bamba est un vrai muslim un grand sunnite
Dieureudiefé serigne touba khadim resol serigne mountakha yalna fi yag té wer amine
Kokou legui mou Fatou Kate katou thiagala
@@ahlousunna6752 liguey wakhni Yalla santou lako Yonentebi santou lako. Rew bakhoul Yarou len tey wakh wakh you rafet
@@ahlousunna6752 yaw esk dioulit gua yaw yaye yalla sa leufal ndeye way
@@ndiayetouba5297 iow sa data yayou serigne ak sa papa 🤬
@@fadiloutoure3974 yene yêna gune lek sêne data yaye Mako wah sa data yayou serigne
Merci imam Ibrahima Khalil Lo nous sommes avec vous . le message est claire ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dangay fene
Dieuredieufeti Serigne Touba mbacke diarama Mame cheikh Ibrahima fall lamp
Soukrann Lô
السلام عليكم ورحمة وبركاته،
جزاه الله عنا خيرآ شيخ إبراهيم خليل لوح. استفدنا و درسنا كثيرا من خطبه ومحاضراته ودروسه.
حفظه الله ورعاه من كل سوء و مكر.
Amiine 🤲
اللهم دمر الوهابيين جميعا
amiine Yarabi
Mame Cheikh Sarr : Amine yâ Rabbî
Masha Allah ya sheikh
serign touba la nio topou merci bamba
Serigne Touba amoul morom lolou mom dou dégne wassalam
Ndaysan serigne touba louko whay wakh togne il à fait tous pour nous
J’ai pitié de mon pays il ne dit que la vérité.
Vérité absolue
Ce petit bout de vidéo à suffisance que ces exclavagistes businessman sont beaucoup plus préoccupé dans la sauvegarde de leurs propres intérêts qu'au écrits de Serigne Touba.
YAWW YA MEUNEU DOUL ..DEMAL DJIANGHI MO GIEUN CI YAWW AK KHALIL LO
BILAKHI AKHMEH LO ÝAYY DOMOU KOUTI DEUG DEUG ..
@@serignethioune2290 yagui meer de qui xasida lay firi
@@serignethioune2290 yaw mi yaye domou kouti deugueu domerame bou bonne bi. Khalil Lô khassida Serigne touba rék la firi ngaye sagua.Démale nga diangui mo gueuneu si yaw ignorant que t'es.
Yalla nagnou yalla defal diam si senegal mousseul gnou si seytané .diam mo gueune lép
Ndeysann c est pas la première fois ma degg ci moom mouy diangalé di diokhay exemple diko dieulé ci Serigne Touba , mâchallah Cheikh Ibrahima ( aka beug tawhid tei mokal alhouran )
Hii vaginaux, démal dégg lu taffiiram yam , surtout les épisodes de Yawmal Xiyaam
Celui qui le critique critique serigne touba il n’a fait que relater les propos du Chiekh ahmadou Bamba
Je n’ai jamais cru que serigne touba a créé un tarikha
Cela est paradoxe avec ces écrits et ce qu’il défendait
effectivement tous ces gens qui ont manifesté leur courroux aprés vu ses vidéos sont contradictoires avec eux memes. ILs ne croient meme à ce qu'a dit sérigne. Quel dommage
Serigne Touba a bien fondé sa voie.Képpeu kou beugu agueu ci Yalla na na nieuw niou dem. Mouride moy ki nameu agueu ci Yalla
@@fadiloutoure3974 dagnlene nelawal yegolene sax lou xew
@@fadiloutoure3974 penses tu que le mouridisme est universel ?
@@Alkhadimya Oui on peut le dire dans le sens où il nous apprend à vivre exactement comme les Sahabas du prophète et avoir la culture du Talibé et de la modestie envers nos guides religieux comme l'étaient les Sahabas envers le Prophète. L'Islam n'est que Soumission et accomplissement des préceptes religieux
yal na faye la si barkey Seydouna Mohammed SAW
Machallah 🥰
Dieureudieuf Serigne Touba koukham dineela ak wa keurem diobakh
DIEUREUDIEUF YALLAH SOUNIOU BOROM
Alla est plus grand du monde et donna qui a puissance
Wax dëgg Yalla wax nga waxu julit, wax nga waxu nit ku maandu té yaatal diiné kepp tax koo jog. Jërëjëf
Shukran oustaz
Beug nala barkeb s.touba
Merci imame Ibrayma Lo que du bonheur sur vous ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️nous sommes de tout cœur avec vous ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieuf Borom Touba.
Maa chaalla ýa khalil lo yalna yalla samla
Dieureudieufety Cheikh Ibrahim Khalil Lo vraiment kou mata sargale
Soubhanala mane dé bayi Senegalais 🤔🤔🤔 kidé dama fogone niiii nite kou bone la,😔 ndékété wakhi serigne touba rek laye jangalé🤭🤭🤭
الله اكبر ماشاء الله حفظك الله ورعاه
جزاكم الله خيرا
سيخ احمد بنب رضي الله عنه
Jërëjëf Sëriñ tuubaa
Machallah Oustaze Ibrahima, we need people like you. You must teach us what the messenger sws of Allah taught the Sakhabats
Ngir yalla wakh len ma kou gueuneu topou souna serigne touba
les compagnons du Prophètes Mouhammad PSL
InchaALLAH alkhurane ak sunna rk ba faww🙏
Mba yangui topou sona
Sunna keinnsouko toudou doundine leuu .. ana ana layssa houweuu ..
Ses propos sont nobles et riche d'enseignement , ahmadou bamba a apporté des moyens de bonheur didactique ,mais ses prédécesseurs l'ont détourné a leurs propres faveur...
Machalah ya cheikh ibrahima khalilou lo
yalla na yalla yagal sa takhaway ak kou. melni yaw
amiine way
Machallah vraiment amna solo
merci pour ton retour mon frere
Serigne touba mbacke koumou nekhoul guenal touba mbacke Sénégal ak liko weur
deut way nagnou tolérant touti
Tontoulenn cii kham kham tee bayii dofdof loubii
Il n'a rien dit de mal 😭 mon Dieu
Il cite les vers de serigne touba quand ça l'arrange,
Mais sur d'autres questions il l n cite jamais, il préfère même des arabes pour soutenir ses argumentaire, alors que serigne touba a écrit sur toutes les questions que l musulman pourra s poser la bonne pratique d sa religion
Serigne bii dh nioune mognou doye khalile ❤️
Li deh deug bou wer leu
THIEUY SERIGNE TOUBA
Mächâllah 💐 اللهم صلى على سيدنا محمد وسلم 💐
Machala ken do borom touba nayssane
dieureudieuf YALLAH SONIOU BOROM
Dieureudieufé Serigne touba xadim rasul wolou ak yakar Serigne touba rek bamba point ( lo amolène xam xam boulène gnou sonal
Dieureudieufti seringue Touba diarama Mame cheikh Ibra fall babil mouridine rek ba faw
Masala
Ndaysann dieuredieuf serign touba beuyit yi nekhna way
Ma Shaa Allah Cheikh Ibrahima Lo, très longue vie doublée d'une très bonne santé, amine...
Amiine 🤲
Bayyi lén fén yi fi serigne touba moi né .
sois respectueux envers les gens. Tu n'es obligé de nous prouvé à quel point tes parents ont raté ton éducation
Diaradiaf Serigne Touba ♥️♥️
DIEUREUDIEUF YALLAH borom djam gni
Je vous avez dit que cet extrait date de 1991. Je vais essayer de mettre sur TH-cam une version d'une heure et quelques.
Et après qu'est-ce que cela change n'êtes vous pas entrain de lire de Hassiba qui datent de plusieurs dizaines d'années ?
@@alhamdoulillallah9438 c'est là où se trouve la différence puisque cette conférence date de 1991 alors ceux qui voulaient l'attaquer parlent d'une sortie récente.
Dieuredieuf Serigne Touba, le seul homme qui avait défendu l'islam quand il le fallait.
Bayile doule
Khamné serigne TOUBA toupoul koudoul YALLA ak ap YENENTEM ...té nagouwo deff limou diglé téksi lou diabotam deff ngani bida la.... serigne bi moy niarigne lou andoul ak lorr..
Yalla bou nitte donn digeul li mou wara déff dou bakh
Ma cha ALLAH K'ALLAH vs agrée...
AMIINE
Allahu Akbar deg rek moi deg ludul deg nenla Masah Allah ya Sheikh
Seul Dieu peut une personne au paradis pas dautre
Yaw loo lakk baa bayyi 😅😆
Ioe lo wakh 🤪😂
Mashallah ❤️
Lii yàgg na lool de.
Wakhoul deug kenn Yaakaroul nit . Nioune Mouride yi Yallah laniou topei Serigne bi . Arretez de jouer avec les mot evidememt k Ndiarigne ak loor ci Yallah lay bayiko , Lolou moniou takha topp Niitou Yallah.
Faut reflechir
Serigne Mountakha nèna yomalkhiyam sou guissè Yalla ak Yonènt bi ak Serigne Touba, mou bayilèn fa dèm si Serigne Touba.
Wa légui nak
Serigne Mountaha Moko wah mou Ler nangne.beaucoup de fanatiques mouride le disent et y croient.
Alors ne nous tympanise pas.
@@zaner5562 🤣😂 xamnga... yen wax yi day deff retan ? Douma wax sax Alakhira, ndax lolou biss bou reuyeu reuy la, mais Malaka rek meuna tax mou faté limou moudié lekk.
Diaroul debat.
Yalna gnou y'Allah may moudj bou rafett.
Deff niou dé ci Tawhid.
Amin amin amin
@@bambatoure9296
Manque de respect si souniou borom wèssouwoul wakh diodiou.
Longue, longue, longue vie ,.à notre Cheikh bien-aimé Ibrahima Khalil lo .
Khalill lo Ahmad lo amolene ngor amolen diom yoneu mouride keneu mounouko soufell
Yaa gnak ngor te gnak diom .waron ngassi tek Kika bagneh teh bagnoum diangaleem.
khalil mon homonyme je t'aime
ماشاء الله
Machalah
Machah amna solo deugg leu
MERCI
Sokhor rék mola diap wayé Yoon bi day djeum kaman rék inchallah
sois respectueux envers les gens. Tu n'es obligé de nous prouvé à quel point tes parents ont raté ton éducation
Allahou akbar ! Gni kou wakh dégni sagua mag-gni da nga lén ti toogn
WAlllahi
Lii Dou tay Dé
Macha allah dieureudieuf serigne Ibrahima khalil lo
Daye sane Gayi gnome kèneu dou diouguè commencé wakh serigne touba nèna gnou commencè ko tague.
Tè limi kheuye dissi gonte moye fèkhè ba kène dou gueumati makgni.
La preuve niata nit gno wèdi mak gni tè Docteur lo ak khalil lo gnolène diagale Gayi yèwoulène
Alkhourane ak Sunnah Rek
Mouride Yi Déme Léne Diagui Diéma Kham Séne Diiné Mo Geune Séne Bokalé Yi Ak Séne Teug Yi Ak Séne Féthi Yi Lolou Dou Diiné Serigne Touba Diagualé Woul Lolou Yalla Yonéntibi صلى الله عليه وسلم La Gnou Roylo Roylo Wou Gnou Serigne Touba
@ablaye lo Kone Gni Mou Fi Bayi Diagualé Wou Gnou Lolou Gni Fi Nék Ni Nakhaté Rék Ak Bokalé Xam Xam 0
Serignou 39 femmes mounougne ko topp
Yàlla na nu ko yàlla fayal
Legui ilayyakha dalahou malam yakouni wala yakounou abadan lil mounkini losiy wakh
Thieiy Sénégal on est tous des musulmans on va prier ensemble bok sape donc nous islam yi warougnou nous retane kounek fanga fête fait tt pour âme yalla avant la mort en plus faut apprécier selon les textes pas a partir des comportement ou des dit des gens le linge salle doit se laver en famille vive le Sénégal djam ak Salam rek
Bilahi oustaz wakh nga deugu
أعاذنا الله من فتنة الوهابية ورزقنا الزهد والتقوى والعدالة والتسامح والأخوة الإسلامية الحقيقية بجاه مولاناالشيخ الخديم
Dieurejeufé serigne touba
Dieureudieuf Yallah borom nieupp
Maa shaa Allah❤
choukran
Long vie à notre Cheikh Ibrahim
Amiine 🤲
Pourquoi on l'attaque alors qu'il dit que la vérité.
Et pourtant il n'a dit que ce qui est bien à Bamba qui correspond aux vérités qu'il lui connait
Bon question
Parce que ça ce qu'il dit va à l'encontre du business de certains soi-disant sëriñ
Niaka gueum yalla rék
Mane dé Je sui mouride mé y a rien de grave il dit k la verité serigne touba deugg rek la woté yalay késsé ak yénetibi
Vraiment qui koubaxla dada ame gnokhamné fitna rek lanuye weur ,dieurdieufe serigne touba
Non bou yamée si limo wakh kay diam rk lay am main li yagg na d déklou nako bou yagg mais loumana xéw manga wakh linga beuga wakh lép si yar ak téguine com s ahmadou rafahi
t'as vraiment raison dieureudieuf YALLAH suniu borom
Yaw khamo Lii Khew Dé
Le bien guidée Qu'Allah soit satisfait de toi imam.
amiine
Vivre ensemble
Kén doe s touba billaki lér na
lolou yaw la angagé
Bilay il ya certain soit disant mourides ou guide religieuse ne comprenne pas les écrits de Serigne Touba
Serigne Touba vivait du coran et du sounnat rassou Lilah
S'il était la aujourd'hui bcp de pratiques n'auraient pas lieu
J aime bien
merci beaucoup
Lii kayy firdé la né Yenn yenna worr diagalem Ahmadou Bamba wayé khaliill lo lou niaw thi Ahamd Bamba. Cheikh Ahmadou Bamba dé bou dikaat tone thi anduna gnou mell nii Khaliill lo lay waayooo.
Saway li yague sa date avant an 2000 ki loumou Massa wakh serigne si lou bakh weddi nakko taye ken sossaloulen lounou l'en wakhale niokko deff
Nitt déss nako toppeu thi bouko yalla dogalé
Ma cha allah
Diadieuf serigne touba mbacké
Deugeuleu dé lolu yépp Serigne Touba moko wakh wayé dafeu lathié g am noppou anrifineu billahi pour g mounaka degg nakk.
Yonen tébii kham kham leu koku douffi diogué yenn lolu molen réré
Sunnam tamitt kham kham leu
Kou ko khamoul boy dé Di tambii nari diakhalneumeu.
Wallahy loloy deugue