Daara Oustaz Makhtar Sarr 👇👇👇 première étape Tabaxu INSTITUT HADJI ABDOU AZIZ SY - DAARA DABAKH Découvrez le projet de construction du nouveau INSTITUT HADJI ABDOU AZIZ SY daaradabakh.com/?page_id=442 TH-cam 👇 th-cam.com/video/3jXBJQVptAA/w-d-xo.html Dans le cadre de l'élargissement du Daara Dabakh, qui a abouti à la pose de la première pierre le 14 Mars 2021 et pour la construction d'un institut sis à Tivouane Peul, nous vous invitons à nous accompagner dans ce noble travail qui nécessite beaucoup de moyens. D'où cette présente demande de soutien. Dans l'espoir d'une suite favorable à notre demande, nous vous prions d'agréer nos sentiments distingués. Vous pouvez envoyer vos contributions via : Wave : 77 796 40 40 Orange money : 77 796 40 40 Compte Bancaire: SN175 01409 043560300101 68 👇👇👇 gofund.me/c1cca501 « Quiconque fait à Allah un prêt sincère, Allah le lui multiplie, et il aura une généreuse récompense » Le Coran, Sourate (57) Le Fer, Verset 11. Yàlla Fayleen yiw ci gunnge gy ci ligéey bi 🙏
Machalla ammo morom makhtar sarr dieuredieuf sagal nga taarikha yi Sénégal mane sa sopé la beugue loll ta yalla rék takh machalla diambari islam nga 🇸🇳🤲🙏🏿🕋📿 Yallanala yalla moussal diaat ak saytané yallanala yalla may ak tawfékh fanén bou goudou ak1000 milliards 🤲 wasalam
@@sambtalibecheikh2382 verema douñou 2 guena lañou s.touba s.el hadji malik sy kena lañou ak baye niass ak souñou kilifa dineyi Wahabista yi mom doul rek
Ouztaz toujours constant ,cohérent tres bonne posture . Affaires yi mom debat contre debat , livre contre livre , commentaire contre commentaire , argument contre argument , ahlou tassaawouf si kaw si kanam ,na saf saaappp !!! Ouztaz . Yalna la borome bi geuna doolél machallah
Tu as toute mon affection et mon soutien Oustaz Makhtar. Haqqui Bil Haqq rek moy fedj lii si niou mbokka dioulit yi di woté Wahabiya nekka. La dignité voudrait que leur Cheikh Ahmad Lo assume ses propos. Qu'Allah Soubhanaho wa talla t'assiste fi zahiri wa batini wa batini batini bijahi mawlana Seydi Woudjoudj saws. Salam Wal Adab filah
Bilay ya oustaz kouy changer position geumoul limouy wah té yaw sa combat si dîné dji gnepp seddé nagn ko. Yalla nala yalla fay té samm la arr la lakh la fa yakh yegoul si barki kou tedd ki psl
Barakallahu fika oustaz Makhtar diadieufati machallah amatina solo yalna bour doli la tawfikh boubakh goudeul fan gui doli Kham kham bi si Barke seyedina Mohamad 🙏🤍🤍🤍🤍🤍
Machalla ammo morom makhtar sarr dieuredieuf sagal nga taarikha yi Sénégal mane sa sopé la beugue loll ta yalla rék takh machalla diambari islam nga 🇸🇳🤲🙏🏿🕋📿 yallanala yalla may ak tawfékh fanén bou goudou wasalam
Dieureudieuf Oustaz Makhtar Sarr vraiment Nioune contan nan trop sa xam xam set na rafet na mes bonne continuation gayi limay wakh rek moy niom sen mame dafa bindoul dara amou niou xam xam nan nopi
Merci Oustaz. Je suis Mouride mais je suis souvent tes vidéos et je t’encourage et te supporte dans tes combats surtout celui-ci. Effectivement les wahabites c’est un tarikha.
@@plumedorfevre3020 Effectivement, vous ne faites pas partie des tarikha du Sénégal mais vous faites partie de la tarikha de Abdoul Wahab. C’est lui sui vous a dit que tous les autres sont dans l’erreur et qu’il est le seul à avoir raison et vous y croyez aveuglément. Vous êtes plus fanatiques que la plupart des talibés de tarikha.
Daara Oustaz Makhtar Sarr 👇👇👇
première étape Tabaxu
INSTITUT HADJI ABDOU AZIZ SY - DAARA DABAKH
Découvrez le projet de construction du nouveau INSTITUT HADJI ABDOU AZIZ SY
daaradabakh.com/?page_id=442
TH-cam 👇
th-cam.com/video/3jXBJQVptAA/w-d-xo.html
Dans le cadre de l'élargissement du Daara Dabakh, qui a abouti à la pose de la première pierre le 14 Mars 2021 et pour la construction d'un institut sis à Tivouane Peul, nous vous invitons à nous accompagner dans ce noble travail qui nécessite beaucoup de moyens.
D'où cette présente demande de soutien.
Dans l'espoir d'une suite favorable à notre demande, nous vous prions d'agréer nos sentiments distingués.
Vous pouvez envoyer vos contributions via :
Wave : 77 796 40 40
Orange money : 77 796 40 40
Compte Bancaire: SN175 01409 043560300101 68
👇👇👇
gofund.me/c1cca501
« Quiconque fait à Allah un prêt sincère, Allah le lui multiplie, et il aura une généreuse récompense »
Le Coran, Sourate (57) Le Fer, Verset 11.
Yàlla Fayleen yiw ci gunnge gy ci ligéey bi 🙏
Machallah machallah amena solo merci dieurdieuf Oustaz makhtar sarr yalla gafiyague téwér 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️alakhouma amine dieurdieuf
WAW GOOOOOOOOOR OUSTAZ MAKHTAR SARR
Ndeysane ! Kham sa mission nekk ci dafa nèkh. Na Bour Yalla takhawou leu, Sarr.
Amin waye massa ahlla
Yalla miye sam yalla na sam oustaz mactar sarr fierté Sénégal ga dieureudieuf
Machalla oustaz yalla n'a yalla samle
Oustaz yalla nala yalla Faye gnun jeunesse bi deh thi sa genre gui lagniy Roye boul falé dra boul ragal dra gnogui and ak yaw Amal diam rek😍😍😍😍
بارك الله فيك يا استاذ محمد المختار صار بالصحة والعافية والعمر طويل ببركة القرآن الكريم
البدعة تكون في العبادات لا في المناسبات
Merci oustaz,yallah nala yallah faye!! ❤️❤️❤️
جزاك الله خيرا شكرا لك مرحب بك
Merci sama domou baye
Machallah yaa oustaaz sa liggéey rafet na
Wawaw Yallah nala YALLAH sameu si barké Cheikhou Tidjane Chèrif rta si Barkèp Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi 🤲❤❤🤍🤍💓♥️ denke nañla Yallah
Machalla ammo morom makhtar sarr dieuredieuf sagal nga taarikha yi Sénégal
mane sa sopé la beugue loll ta yalla rék takh
machalla diambari islam nga 🇸🇳🤲🙏🏿🕋📿
Yallanala yalla moussal diaat ak saytané
yallanala yalla may ak tawfékh fanén bou goudou ak1000 milliards 🤲 wasalam
Diuerediuef Serigne Makhtar Sarr Waw Gor Nila Rek ☝️ Ndam Rek ☝️ in Chahalah Bilahi Sono Makgni Rek ☝️ L'ano Am
Machallah oustaz Makhtar yalla n'eu yallah barkel té sambeu leu barké yonent bi PSL
Kimome Damako soppo rK barker Serigne Touba yalnala yalla takhawo🤲🤲🤲
Suis mouride mais man damala beug barke serigne touba yalna yalla goudeul sa fann🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Serigne Moctar Sarr boul ragal dara ya ngui si deug yalla nala yalla faiye barke Serigne Touba
ماشاء الله جميل جدا ورائع يامغتارسار زادك الله عمرا طويلا مع الصحة والعافية والسلامة وبارك الله فيكم جميعا ءامين يارب العالمين
Encore une fois diereudieuf yalla n'a yalla samm la
Je suis mouride mai vraiment oustaz makhtar sarr bageunala lool yalla nala yalla samou teh àrla
Je suis mouride bi moko diaroul
@@sambtalibecheikh2382 samba mangui toub boubakh dotoul am mai kone évaséel talibé cheikh bi déf samba kasé
@@keindeibrahima4547 précision bi nga def dafay melni bou nekoul Tidiane waroko beug.
@@sambtalibecheikh2382 verema douñou 2 guena lañou s.touba s.el hadji malik sy kena lañou ak baye niass ak souñou kilifa dineyi
Wahabista yi mom doul rek
ماشالله شيخ مختار صار جزاك الله خيرا اللهم نور علمك بحاه سيد المرسلين
diara diaf ostas makhtar sarr yalla nala yalla samo te arla
Merci oustaz yalla na la Yalla difal diamou 👏👏👏👏👏
Yalla nala yalla faye oustaz makhtar sarr
Bilahi soufisme danio deggg alkhour’ane ak sounna
Amal diamb Rék Machallah yalla Nala yalla takhawou
ماشاءالله يااستاذ جزاك الله خيرا
Aminn 🤲🤲🤲
Bonne continuation oustaz makhtar sarr dadié naniou Fès week-end passé kou baax nga kou am diné nga masha Allah yalla nala yalla sameu 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Oustas makhtar Sarr sa numoro la beug yalla gafi yage barkép borom Touba❤️
Bilahi sama xolle sedana si yaw goudal fane si barké yonéntébi صلى الله عليه وسلم
Machalla papa Makhtar sarr damou sy yaw incall
Jazaakal LAHU xayrane
Yalna na YALLA same
Notre oustaz national
Machaalah oustaz yam mom vraiment yalna yalla sambla
Yalna la yallah takhawou té samme la bi jahi TAHA SAWS🤲🏾
Amin waye kubakha la
@@jesuispapealeniag5529 Wallahi bakh na beugue na lou bakh té Kenne diné ak sounou makk mou caye fekké
Machallah oustaz Mactar sarr on restera soufi et tidiane jusqu’à la fin des temps.
Macha Allah Oustaz Sarr
Mbòloom Osstaz yi Boudon Togg Makhtar Sarr Moóy Kàani gui Yéen Wahàbia yi nak Amŋén problem bourëy
Bilahi 😂😁😁😁😂
ماشالله شيخ مختار صار جزاك الله خيرا
Machala yalna yalla samla arla yirrla yokou l'a bagha yeuke ko bilaye bègue naniou si yaw
Amo morome Sénégal tidiane.mouride . Khadre.layene.poin?
Wawwa
N’a nieupp àdando nianal oustaz makhtar Sarr yalla goudeul fanam ta tokk wérgui yaram amine ngir yalla malenko nianne nako nieupp df
Macha-Allah oustaz sarr yalla na yallah samala.
Macha allah yallna yalla faye la
Macha Allah Oustaz Makhtar, yalna yalla yaagal takhawaay bi
Yallah n'a yalla sameu la barrép Alkhourane 🤲 ya oustas
Seyda zeynab kouko wakh wakh bou ñiaw dou bayi kéne. Ko khamni Macha Allah kouko guiss beugueko yallana FIRDAWS done deukouwayame YAA RABB 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Merci Ouztaz je suis Mouride mais je t'apprécie beaucoup.
Je suis mouride wala je suis tidiane...... Diarouko lepp bennla ziyar naala boubakh nak li AK fatali rék la merci
@@ndongogueye9470 merci
@@ndongogueye9470 waw gooooooooor machala
Merci beaucoup makhtar Sarr yalla na yalla fayla yiw inshaa Allah boulén falé li abdou Latif Gueye don wah rék mothi am lahou thi sounou ginaw borom
Machallah yallah nala yallah Faye yiw
Diadjeuf Oustaz Makhtar Sarr, Yalnala yalla fay, contane nagnou sisa takhawaay 🙏🏾
Billahi makontane sy yaw ya oustaz yallah nallah yallah samou
Ouztaz toujours constant ,cohérent tres bonne posture . Affaires yi mom debat contre debat , livre contre livre , commentaire contre commentaire , argument contre argument , ahlou tassaawouf si kaw si kanam ,na saf saaappp !!! Ouztaz . Yalna la borome bi geuna doolél machallah
Tu as toute mon affection et mon soutien Oustaz Makhtar. Haqqui Bil Haqq rek moy fedj lii si niou mbokka dioulit yi di woté Wahabiya nekka. La dignité voudrait que leur Cheikh Ahmad Lo assume ses propos. Qu'Allah Soubhanaho wa talla t'assiste fi zahiri wa batini wa batini batini bijahi mawlana Seydi Woudjoudj saws. Salam Wal Adab filah
Ya oustaz yaga fi lol te werr diamou rek incha Allah
@Mame Diarra Diop 😈😈😈🤮🤮🤮🤮
👎👎👎👎
😰😰😰😰😰😰
ماشاء الله بارگ الله فيکم
Tabaraka lahou ya oustaz amna solo jaamm rek
Bilay ya oustaz kouy changer position geumoul limouy wah té yaw sa combat si dîné dji gnepp seddé nagn ko. Yalla nala yalla fay té samm la arr la lakh la fa yakh yegoul si barki kou tedd ki psl
Manela wahabista yepou hay nafekha lañou nagou wouño degeu degeu
Te ñom si TH-cam bi rek lañouy neka DTV monañou lenfa waye dolenfa guis
Yalla na ngou yalla meussall si reur 🤲
Machallah ya oustaz
Jajeef Serigne Mactar longue viiiiiiiiiiiiiiie Amine ❤️❤️💚💚🤲🤲🤲
Saga nitou Yalla moom,alkou rek
,mou gaaw walla mou yéekh.
Leerna lagn. Diereudieuf oustaz Sarr. Comme a chaque fois. Diereudieuf SERIGNE TOUBA Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
Barakallahu fika oustaz Makhtar diadieufati machallah amatina solo yalna bour doli la tawfikh boubakh goudeul fan gui doli Kham kham bi si Barke seyedina Mohamad 🙏🤍🤍🤍🤍🤍
Ustaas yal na sa jàmm yàgg 🥰✍🏾️
Merci imam
والله فرحت منك جدا ياسيدي الله يحفظك ❤️❤️❤️❤️😭😭😭
Machalla yalla nala yalla samou té aarla
أحبك وآلله لوجه الله تعالى أنت رجل صالح
Machalla ammo morom makhtar sarr dieuredieuf sagal nga taarikha yi Sénégal
mane sa sopé la beugue loll ta yalla rék takh
machalla diambari islam nga 🇸🇳🤲🙏🏿🕋📿
yallanala yalla may ak tawfékh fanén bou goudou wasalam
Merci encore une fois Oustaz
Dieuredieuf oustaz ligua wax lep lérna
Dieureudieuf Oustaz Makhtar Sarr vraiment Nioune contan nan trop sa xam xam set na rafet na mes bonne continuation gayi limay wakh rek moy niom sen mame dafa bindoul dara amou niou xam xam nan nopi
شكرا لك يا استاذ مختار...
جزاك الله خيرا يا مختار
Machalla yala nala yala mousall defala diamou
Machallah yalla guafi yaga tawér Amiiine
Merci oustaz ❤️❤️❤️
Dieredieuf oustage makhtar Sarr yalna yalla doolli wéer ta bakerl ligeuy bi
ماشاء الله مختار صار سمعت حقا والله
Alhamdoulillah Macha allah kontane kontine 💓💓💓💓💓💓💓💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗❣💘💘💔💟💟💟❣❣❣❣❣❣❣💔
Walakhi lolou degue magui fi si arabie saoudite mai lou ne mofi amm 🇸🇦🇸🇦😭😭
Merci Oustaz. Je suis Mouride mais je suis souvent tes vidéos et je t’encourage et te supporte dans tes combats surtout celui-ci. Effectivement les wahabites c’est un tarikha.
Dou deug. Bokkou niou bneu tarikha
@@plumedorfevre3020 Effectivement, vous ne faites pas partie des tarikha du Sénégal mais vous faites partie de la tarikha de Abdoul Wahab. C’est lui sui vous a dit que tous les autres sont dans l’erreur et qu’il est le seul à avoir raison et vous y croyez aveuglément. Vous êtes plus fanatiques que la plupart des talibés de tarikha.
@@amathug As salam Aleykoum.
Porte toi bien !
Imam Makhtaar Sarr machallah yalla na yalla doli la tawfekh barkëp Borome Touba
Machalah oustaz 💕bilahi diam rék ngay am ndakh deug rék Mola takha diokk☝️
Oustas yallanala yalla fay ماشاء الله
Dieureudieuf ya oustaz longue vie a toi merci.
ماشاءالله جزاك الله خيرا
لا تخف و لا تحزن ✊
Pass pass bou bone lagne léne rabalé feulé thia deuk wahhabites yeu pour gnou gneuw contré yoonou tassawouf. Mais c'est perdu d'avance, yala nagnou Yallah fayale magg gni. Dieureudieuf mame Seyd'El Hadji Malick Sy RTA...
Billàhi wallaahi deugg rek nga wax, yag naalay suivre mais benn kaddu bii rek nga mosa am...bul mosa nopi. Jarajëf Sarr
Diadieuf oustaz! Nala buur takhawou ci sa deuggou.
Machallah waaw goor 👍👍
Way m'a bégue si yaw oustaz ❤️❤️❤️
Machallh
Alhamdoulillah Macha allah kontane kontine
machalla oustaz barakallahou fiika.
Machallah oustaz magui kontane
حفظك الله ورعاك
Machallah deug rek❤️❤️
Merci beaucoup oustas