MNM - Veux tu m'epouser ? (Lyrics) Allô baby girl dama la soxlawon pour ñu waxtaan some time Nuyu wu ma la sax mba ya ngi diam d'abord xam nga rek da nga may comprendre Pour li ma lay doyé féxél ba imaginer èhh anhh yaya!! Xam na sa bopp ya ngi giss image yu né éh xam na la Kumpë ngi lay ray ya ngui lox fi nga toog dalalal sa xél du li nga foog Gaw nga diaxasso mang koy yëg fima tok soxlawu ma la localisé yaw pour xam fi nga tollu Fay ma ma wax la neexal ma nak baax na lu ko moy ma wirri wirri bae ba diareefa nax lë Lu ma ci jublu lu baax la mais nak fallait que ma cax lë and bu yaggé yaw tè dëggu lu ko lal koon lu sax la Hé wallahi yaw rek'a matt li nga doon xalli nga sama yoon mu tar nga dékku fi coono Té bilahi mussoo ma def lu ma métti fép da nga ma ci fékki takku ci ngir ma tékki Loolo tax tay ma bëg yaw ñu and bae bolé life bi def ko bén dagganal ko ngir ñu sëy Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dés Veux-tu devenir ma femme veux-tu m'épouser Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser Veux-tu devenir madame veux tu mé'pouser hèè èèhh You'd never be alone you can call on me baby Give me your hand don't be afraid Look me in my eyes and tell me that you love me stop thinking bae you now I love you Normal mu yeem la ndax day lu bees mais mérite la nak ak fu ñu jota wees bae Li ma la fayé tay dang ko fi jiw hey sa oui waw ok moy takh ñu siw you now Né ma yes rek ma free hihi Sama life sans yaw non dou chill hihil Bayil sa jooy yi xam ga yaw la feel hihilll Baby girl yaw you now the deal hilll Dëg la xol yii fees na rongoñu mbegtéy tuuru Mais tay nak bés bu bees la ñëwël mak yaw ñu nguuru Lu ñuy dundu dafa fees nak gis nga sax mu ngi tuuru Man jitu na la leuz ba ya ngeek lém ma ngeek mbourou Hèè wallahi yaw rek'a matt li nga doon xalli nga sama yoon mu tar nga dékku fi coono Té billahi massoo ma def lu ma mètti fep danga ma ci fékki takku ci ngir ma tékki Loolo tax tay ma bëgg yaw ñu and bae bolé life bi def ko bén daganal ko ngir ñu sëy Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dees Veux-tu devenir ma femme veux-tu m'épouser Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser Veux-tu devenir madame veux tu mé'pouser hèè èèhh
C'EST QUOI CE TALENT ENORMISSIME. MACHAALLAH JUSTE MAGNIFIQUE TA VOIX TES PAROLES TOUT EST AJUSTÉ À LEUR GRANDE VALEUR. BE FOCUS ET CONTINUE AVEC CE LEVEL. RESPECT À TOI ARTISTE
Meii esk son mouguii audiomack je lecoute chak jour moussouma commentaires 2 fois sii bénn son meii son bii mérite des millions de vue biilayy senegal khamougnou son lii mo dakk son gnou beurrii gnou fii deff buzz actuellement lii moy hit
Oui l'homme polyvalent Machallah 😍😘😍rap bi weuy bi foko wo mou wouyou sii la 😊😊très bel voix yallah na yallah taxawu nous t souhaitons bcp d succès frère courage
Je viens de le découvrir grasse a tiktok c vraiment du lourde bonne continuation frr 😊❤️ j'aime beaucoup le tranquilité de cette music et les parole Mashallah ✨❤️bonne inspiration frr🥇🥳🥳🥳🥳
MNM - Veux tu m'epouser ? (Lyrics)
Allô baby girl dama la soxlawon pour ñu waxtaan some time
Nuyu wu ma la sax mba ya ngi diam d'abord xam nga rek da nga may comprendre
Pour li ma lay doyé féxél ba imaginer èhh anhh yaya!!
Xam na sa bopp ya ngi giss image yu né éh xam na la
Kumpë ngi lay ray ya ngui lox fi nga toog dalalal sa xél du li nga foog
Gaw nga diaxasso mang koy yëg fima tok soxlawu ma la localisé yaw pour xam fi nga tollu
Fay ma ma wax la neexal ma nak baax na lu ko moy ma wirri wirri bae ba diareefa nax lë
Lu ma ci jublu lu baax la mais nak fallait que ma cax lë and bu yaggé yaw tè dëggu lu ko lal koon lu sax la
Hé wallahi yaw rek'a matt li nga doon xalli nga sama yoon mu tar nga dékku fi coono
Té bilahi mussoo ma def lu ma métti fép da nga ma ci fékki takku ci ngir ma tékki
Loolo tax tay ma bëg yaw ñu and bae bolé life bi def ko bén dagganal ko ngir ñu sëy
Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dés
Veux-tu devenir ma femme veux-tu m'épouser
Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh
Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser
Veux-tu devenir madame veux tu mé'pouser hèè èèhh
You'd never be alone you can call on me baby Give me your hand don't be afraid
Look me in my eyes and tell me that you love me stop thinking bae you now I love you
Normal mu yeem la ndax day lu bees mais mérite la nak ak fu ñu jota wees bae
Li ma la fayé tay dang ko fi jiw hey sa oui waw ok moy takh ñu siw you now
Né ma yes rek ma free hihi
Sama life sans yaw non dou chill hihil
Bayil sa jooy yi xam ga yaw la feel hihilll
Baby girl yaw you now the deal hilll
Dëg la xol yii fees na rongoñu mbegtéy tuuru
Mais tay nak bés bu bees la ñëwël mak yaw ñu nguuru
Lu ñuy dundu dafa fees nak gis nga sax mu ngi tuuru
Man jitu na la leuz ba ya ngeek lém ma ngeek mbourou
Hèè wallahi yaw rek'a matt li nga doon xalli nga sama yoon mu tar nga dékku fi coono
Té billahi massoo ma def lu ma mètti fep danga ma ci fékki takku ci ngir ma tékki
Loolo tax tay ma bëgg yaw ñu and bae bolé life bi def ko bén daganal ko ngir ñu sëy
Té waxtaan nañ sa papa yombalal ma lep né na léegi ya ci dees
Veux-tu devenir ma femme veux-tu m'épouser
Veux-tu devenir madame veux tu m’épouser hèè èhh
Veux-tu devenir ma femme veux-tu épouser
Veux-tu devenir madame veux tu mé'pouser hèè èèhh
Bel parole😍😘
Le son sur audiomack : audiomack.com/mpossibleprod/song/veux-tu-mepouser
Ki ndaadan mais nagoul nako il est fort blh
Machallah
On ma toujours dit que j avait une belle voi té frencemnt j'aimerais faire klk chose avec toi mnm
😱😱😱 yaw Mii donne rap yay weuy ni encore 😭😭😭ay way fouma nekonn ce goss mérite tt le respect
Sound bi damakoy con's diko life diko yeugu❤. Mnm man ya kawé dh🎉❤
Mnm l'homme polyvalent 😍😍😍😍😍😍😍Trop cool le song t'as assuré♥️♥️♥️♥️
Nn Macha allah yalla na nala Yalla défal lo beugue nn daga moune loy déff yéx Naala khame Tay la lay Dogaa khame ms nice neu trop Macha allah 🤩💕💕
Yaw borom 16mn yii ya épousé sound bi encore 😍🔥
Ohhhh quelle plume ta un voix de ouff ce son mérite des millions de vues t un artiste plein merci beaucoup pour ce chanson ça va droit au coeur
Wallahi moussouma douguele crédit ti deglouwma son biii MNM Wallahi vous êtes merveilleux li dafa nékh
Trooooop de feeling, c'est chou adorable et on ressens la présence du glamour.... bon travail MNM, JP et le reste du groupe✨💞
Je suis fière de toi baby le meilleur reste à venir🔥🔥🔥 inchalla ❤️🙏🏼
C’est doux🥰
C'EST QUOI CE TALENT ENORMISSIME. MACHAALLAH JUSTE MAGNIFIQUE TA VOIX TES PAROLES TOUT EST AJUSTÉ À LEUR GRANDE VALEUR. BE FOCUS ET CONTINUE AVEC CE LEVEL. RESPECT À TOI ARTISTE
je viens de te découvrir mais franchement le clip est extraordinaire le textes est touchant vraiment du courage et bonne continuation 👏 ♥️💪🏾💪🏾
Meii esk son mouguii audiomack je lecoute chak jour moussouma commentaires 2 fois sii bénn son meii son bii mérite des millions de vue biilayy senegal khamougnou son lii mo dakk son gnou beurrii gnou fii deff buzz actuellement lii moy hit
Le son sur audiomack : audiomack.com/mpossibleprod/song/veux-tu-mepouser
Machala yalla na yalla geuna yok son bi nehna clip bi nice na fils de grand Dakar je valide
Franchement bro, ce son je l'écoute de manière répétitif, machallah ta assuré billey. Il numbe one thi sama play liste
Je valide bro MNM contane continue Big frère ligueye rek Big town 4 ever
Ohhh j'ai pas les mots😥😥
Atieu ngako tji kaw MNM🏀🏀🏀
Je te veux déjà , Macha allah laff thiatt , yalla borom bi goudeul yonn wiii . big town for ever.
Billahi depuis ma déguelou son bii moussouma nélawe tii déguelouwmako vraiment ce chanson me plaît beaucoup
Weah boy bi talent la amm
Meun rapp
Meun weuy
Am inspiration
Bon boulot PeulbouhighTBeatz ✌️
❤️❤️thx mon artiste🔥🔥
mashahalla frère sa caw sa caname rk lépaye bakh inchahala 👌😎💗
Nice na domou grand Dakar
Wawaw niceuhhh mmn de la part de modou wa daara j bkna niou si iow
Ce son merite ds millions de vues 🎉🎉🎉🎉❤
Son de l'année
MNM do niit boy,j'ai falli pleurer %%
Ki nitorien la boy😂!
@@youdenhazard35 dafa léer
@@issababathiam939
Khana yako diokh linguégn yi😂?
Lima baby😍❤
Ohh son bih je viens de le découvrir mais c’est trop cool🥰💍🫶🏾
Wawwww son bi magui koy sentir lou barri🥰🥰🥰
Douma si doyal troop love😍😘😘😍
Bonne continuation Domou NGB
Cette vidéo mérite plus de vue le son mérite plu de téléchargement ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Tiktok la diougué 😂❤
🤣🤣😂 niolafi yabal khana
C'est vraiment top.du courage frère. On est tous derrière toi
Wa meii kane la je viens de le découvrir kii daffa🔥🔥🔥 son bii daffa dope kharaall ma abonné kholl yénn bagages yiii nice broo
Il es fort gran Dakar leu deuk
Bonne continuation frère ton ami biram m'a bcp dit sur toi tu es le meilleur diapp rk lepp dina bakh
c gas il a tellement d talent j ls suivie sur ls cypher full respect man yokk job rek
Oui l'homme polyvalent Machallah 😍😘😍rap bi weuy bi foko wo mou wouyou sii la 😊😊très bel voix yallah na yallah taxawu nous t souhaitons bcp d succès frère courage
Ce son mérite des millions de vues 🎉🎉
Machala tres nice c la 1 fois der waww.Merci depuis Barcelona España España
Fire Boy MNM Nice Son !! Yaangii begual sinu xool yii
Meune Rap meune weuy ! Top Talent 🎉boy #Respect MNM ✊🏽
MNM bilay sen cypher lala commencé suivre ba lguii
Lodia yama wone yone bi en plus je valide 🔥🔥🔥 💪
Tellement que s’est carré je vais me marié wasalm
🥰
Athia frere inchahala ca ira
Une fierté pour diobass❤❤❤one love frah❤🎉
Respecte bro Nice son flow,,Texte,,Instrul,, leup mogui dop 🙏
Houf très cool
Nagua m'a invité sou naguo nak thiey sama rappeur foune lay feule mais nk nice👍👍👍❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️
MNM ge cana boy ❣️💖💕 lepp impect
Original 😍😍Force à toi le peuple est content 😍😍😍😍😍😍😍😍😍 coup de cœur ❣ wharever happen in vegas feureureuww😇😇😇😇😇😇
Pourquoi cette vidéo ne pas u des millions des vues machallah sa sonne bien 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Oui je veux t’épouser 😂😂😂
Ta décidé
Notre Alima wayy🥰❤️
Est ce que c'est toi sur le clip?
bonne chance souniou fierté FrOm big town
Nom super héros ngua😍😍😍
Bonne continuations mn frère borom Diobass
Wharever happen in Vegas 💥💥
First time à écrire un commentaire, nice son. Good job
Mashala frère ❣🤗toute mh félicitations c trop nice
Nice na bro bonne continuation carrière laniou visé dou clip bro 💯💯✌🏽✌🏽
MNM 4 ever love. International Music
My bro MNM✌✌✌✌
Fierté Big town ❤️✊🏿🔐
Hèy MNM song bi dope ça m'a bercé wallahi 😀👍🏿👍🏿 j'adore
No Nice Single 🥰
Wolah on apprécie boy...nice job👌 et bonne continuation
Mais cette chanson devrait être viral
J'écoute ce son 8fw par jour
sa voix est exceptionnelle
Nice serere bou nice au Sommet rek
Son bi dafa graw🥳🥳🥳🥳
Trop nice oohhh tu es le meilleur wolah 💪💪💪💪🎤🎤🎤🎤
Pourtant guissa gouma bou dakkeu bi je viens de le découvrir mais waouh 🥰il est lyricalement fort ce gars 💪
Nice frère bonne continuation 🙏🏽❤️
Mo gui coollll💪🏾🔥
Bly ki da aye🔥🔥🔥🔥🔥🔥bonne continuation 🔥🔥🔥
J'ai découvert ce son c extraordinaire de douceur d'apaisement
Magnifique
Franchement ce mec est hyper fort très très talentueux
Franchement cei jolie alima ❤️
PeulBouHigh Beatz❤️🔥
Thx Manager❤️
Nice fréro job bi sét na bro
Bonne continuation frére MNM🔥🔥
Machallah j’adore🥰 bonne continuation
Machallah Nice neu brow bonne continuation
Nice na trop bro 😎 one love ❤️
Un artiste a promouvoir car il est polyvalent vraiment respect cii iow champion
Ohhhh quel coup de coeurr❤❤❤😍😍😍😍
Chapeau neveux ♥️
pour mane rifou mo wooy son bii sakh
Li dafa nice bro
Je viens de le découvrir grasse a tiktok c vraiment du lourde bonne continuation frr 😊❤️ j'aime beaucoup le tranquilité de cette music et les parole Mashallah ✨❤️bonne inspiration frr🥇🥳🥳🥳🥳
Weuw niceuh job guyz.... Bravo à l'équipe et bonne continuation MNM 💪🏽🙌🏿🙌🏿🙌🏿
Dop bro bilahi suis fier de toi
Mnm mann yague naleu sétann depuis t cypher konn iow rap bii souleu fayoul rek togne naleu
One love frére dop dop dop nice track clip bi caréna bro
Je viens te découvrir à travers TikTok t’es trop fort 💪🏿🇸🇳❤️
J vient d tomber sur se clip mais l gas a du talent machallah ❤❤❤🥰🥰🤩🤩🥳🥳Bne continuation 🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Premier commentaire Bonne continuation à toi
oufffff validé
Sa mérite vraiment de percé
Clip bi nice na rafete na