Lyrics ‘’Mbeguel’’ Intro Anhh yaya yaya ioe mii ioe rek ioe mii ioe mii anhh anhh ana nana Couplet 1 Dieum dji rek ladonn sett (ladonn sett) Fèñ na cii ioe dotoul rérr (dotoul rérr) Baby my life don't be afraid (don't be afraid) Dotouma bayi diotena teuyè Konn feel your love for me (feel your love for me) I do it for you do it girl for me ( do it for me girl yaw) Bébé cii ioe la mirr (bébé cii ioe la mirr) Kouma xol cii ioe never mou tekma nitt (never mou tekma nitt baby) Hè diotenala mine girl (demna ba mine leu baby) Ohh baby my vitamine girl (anhh yayay vitamine girl) Love you my sweet girl (i love you To mon bébé ) Hè ioe mii sañe nalla guiñieul ( guiñieul doumasi diog ndakh) Refrain Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog) Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè) Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog) Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany) Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi) Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya) Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi) Couplet 2 Ndèker mbeuguel nila nèxè carlou meun nama sedder Baby xolma ci beut way yeug xol bi noumou seder mag ioe deug laniouy doundou takh ba talatouma rêver yeurmandè lall louniou bolè mais tay mbeuguel bii lay fêter You know me ( you know me) Baby my life my only (my only) Boma namè del xol fii( del xol fi) Ioe rekka takh ma melni ( ma melni ihh) Waxnalani diotenala mine girl Ohh baby my vitamine girl Love you my sweet girl Èhh ioe mii sańe nalla guiñieul Refrain Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog) Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè) Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog) Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany) Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi) Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya) Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi). Couplet 3 Tank ak tank mbag ak mbag bagn dem cii ngoro Donn na tay dehh kilay tagg wawaw dotofi thioro Cii yeurmandè la mbeuguel magg dotouniou tongo Donn na tay yaw kilay Madial anh yay dieumèma bango Ioe rekk mii (ioe rek mii )ioe mi ioe rek kèssè lay donn Xolma fii (xolma fii)xolma fii do wètt cii bii yonn Tagal la say mame bou doyoul( doyoul) gorel nga diam bii dioyoul (dioyoul) Lima diota niamm ni kouko diota niam nieuweul seder ni sofoul (sofoul) Outro Èhh anyaya anyan yayaya Èhh anyaya anyan yayaya Anh yayayè anh yayaya Anhh yayaya anhh yayaya Lyrics By MNM @Mai2021
Étant celui- qui te suis depuis longtemps Et comparé les 2dernier clip c'est de 100% a 25% Niveau texte yi ligueyo si dara sama guiss guiss RK la waxx L'autre son je pouvé TT une journée diko cons t douma doyal mais bi lgui lako deglou mais srx doyal nasi Talent bagui fi deh ligueyal si texte yi wayy
Lyrics ‘’Mbeguel’’
Intro
Anhh yaya yaya ioe mii ioe rek ioe mii ioe mii anhh anhh ana nana
Couplet 1
Dieum dji rek ladonn sett (ladonn sett)
Fèñ na cii ioe dotoul rérr (dotoul rérr)
Baby my life don't be afraid (don't be afraid)
Dotouma bayi diotena teuyè
Konn feel your love for me (feel your love for me)
I do it for you do it girl for me ( do it for me girl yaw)
Bébé cii ioe la mirr (bébé cii ioe la mirr)
Kouma xol cii ioe never mou tekma nitt (never mou tekma nitt baby)
Hè diotenala mine girl (demna ba mine leu baby)
Ohh baby my vitamine girl (anhh yayay vitamine girl)
Love you my sweet girl (i love you To mon bébé )
Hè ioe mii sañe nalla guiñieul ( guiñieul doumasi diog ndakh)
Refrain
Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè)
Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany)
Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi)
Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya)
Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi)
Couplet 2
Ndèker mbeuguel nila nèxè carlou meun nama sedder
Baby xolma ci beut way yeug xol bi noumou seder mag ioe deug laniouy doundou takh ba talatouma rêver yeurmandè lall louniou bolè mais tay mbeuguel bii lay fêter
You know me ( you know me)
Baby my life my only (my only)
Boma namè del xol fii( del xol fi)
Ioe rekka takh ma melni ( ma melni ihh)
Waxnalani diotenala mine girl
Ohh baby my vitamine girl
Love you my sweet girl
Èhh ioe mii sańe nalla guiñieul
Refrain
Mbeuguèlou thiaxann taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou foo taxouma diog (lolou taxouma diog hè)
Mbeuguèlou hun hun taxouma diog (taxouma diog)
Mbeuguèlou yeurmandè ma taxa diog hè hiyè èhh ioe nana nana anhh (ohh wouhhan anhh yaya yany)
Nana nana nann anhh ( ohh wouhhan anhh yaya yanyi)
Hè nana nana nan anh ( ohh wouhhan anhh yaya)
Nana nana nann anhh (ohh wouhhan anhh yayayi).
Couplet 3
Tank ak tank mbag ak mbag bagn dem cii ngoro
Donn na tay dehh kilay tagg wawaw dotofi thioro
Cii yeurmandè la mbeuguel magg dotouniou tongo
Donn na tay yaw kilay Madial anh yay dieumèma bango
Ioe rekk mii (ioe rek mii )ioe mi ioe rek kèssè lay donn
Xolma fii (xolma fii)xolma fii do wètt cii bii yonn
Tagal la say mame bou doyoul( doyoul) gorel nga diam bii dioyoul (dioyoul)
Lima diota niamm ni kouko diota niam nieuweul seder ni sofoul (sofoul)
Outro
Èhh anyaya anyan yayaya
Èhh anyaya anyan yayaya
Anh yayayè anh yayaya
Anhh yayaya anhh yayaya
Lyrics By MNM
@Mai2021
Projet bi kagne la
Tombé accidentellement sur la vidéo. Mais je suis agréablement surpris. Tu mérites d'être connu
Polyvalent 💃
Kenza yangui foune defal dra si boy bi
Kenza brom promo yii Defal dra
Defal sa job
Réaction
Ya xam kou nk
Nice bro yagui warr nice track your bro alkaida nice good job amal diam créativité innovation comme nonou rek yama geuneu now
Fire Boy MNM akkka graaw.. défatinga lou reuy nakk son bii c'est du lourd
Oooh Nice track Nice vidéo
Si seulement j’avais ls mots pour t’expliquer ce que je ressens encore tu ns a surpris MNM long vie ❤️❤️❤️
Thiey mane xalè bi dafa narate xarr fi rek nieup tassaro😍😍👑
Je le connais ki dou nitt sakh lii dou dara sétan lén avc le temps rk🔥🔥✔️😎
❤️❤️❤️🤩🤩diga takh ma dem dokhani watt dama bayi won 😠
La star du Jobass, futur patron du hip hop sénégalais
Sissou mann yangui dislike 😂😂😂😂😂apart ça li nekh na wayyy 🥰🥰🥰
MNM mou ngui cool dh🔥🔥👌
Khady fa gaye ma challah Frere
Yalla na yalla yokk succès bi diam akk kheweul bi
Vraiment tu as le talent bonne chance broder🤩😍🤩
Thanks oncle
Waouhhhh quel talent mashallah✔💯
🪑 manguii tokk dii khar MNM🤩💯
Work work work 💪💪💪kim jon un ☝️
Respect tii ioe mnm job rk litii kanam rawou li gueute
Nice man kon dap
Diadieuf wayy bro
Yeah mongui bakh
Mais bay fo nekone bay borome cypher yi ak dope wadji bonne continuation Big Town up ngb wassup
😍😍😘😘🤩😍😍😍Nice Mémii😘😘 bonne continuation
Wa ms ko moy kane tangue dieurr man 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥❤❤❤🍎🍎🍎🥀💘💘👊
Big town reek. La simplicité est la sophistification suprême de l'art.
Thia kaw MNM Niguer
Ndam rek unchala yalla bkhna
Weuw niceuh... Bonne continuation
Wipliww😍
Thiaa niveau bala🥳🦾
Nice na way ♥️♥️🔥🔥
Il est très fort walahi c la deuxième fois je le vois il chante bien good Way bro
J'adore billy et bonne continuation MnM tu sera le meilleur c du lourd ca litii knm rawali beut nice frère
Nice ma wayyy👊
Machallah couz moungui bakh 😘😍
Athia frere inchalla day bakh
Wawe guorr Faye biram seutou salmoune
Machalla Nice n'a trop
Nice Dop dop 👌👍💯💯💯
From big twon ❤️🖇✍️✅
Sa déchire woolah🙈🦋✨🍾
Étant celui- qui te suis depuis longtemps
Et comparé les 2dernier clip c'est de 100% a 25%
Niveau texte yi ligueyo si dara sama guiss guiss RK la waxx
L'autre son je pouvé TT une journée diko cons t douma doyal mais bi lgui lako deglou mais srx doyal nasi
Talent bagui fi deh ligueyal si texte yi wayy
😭😭😭😭amna artiste legui artiste bou polyvalent nak
Mingi Cool bro bonne continuation
Joal fadiouth ❤️❤️❤️ ma fierté 🥰
Waw il est fort jvien de decouvrir MNM Mais respect jaim Le tube mariama
Nice neu trop 👌🇸🇳 FADIOUTH mon beau village 😭❤
Bonne continuation frère on vous suit depuis l Maroc 🇲🇦🇲🇦🇲🇦
Badou ngéye am fofou maghi guiss dhé bilaye grâce à vous
Non niougui koy suivre machallah il a du talent 🔥 🔥
Thank
Nice💫💫💫💫💫💫💫
Omg😍perfect mashallah 😍💃
Mashaallah bro je te connais pas mais amngua Talent mashaallah
Nice bro
Bonne continuation
Dop 🔥man
Lou graww
Fière de tw frRe💓😍
Nice naa trop bro
Macha Allah , frère j ai apprécié vraiment . Big town for ever . Rang Mouy weuy beuguel . Mais khale bi khana kirene lay sangoo
✅✅✅
Nice Nice
Fier d'être Joalien😍🤩
Nice 💥
Nice sound, nice clip, nice voice, nice girl....I like this.
Merci MNM, Merci Mpossible prod👌
Big town est fier de toi frer MNM bon continuation
Mon village way♥️ nice clip frére🥰
Encore mon rappeur en haut du podium.
Félicitations
C est du lourd mon trés chers a feast for the ears bonne continuation big up
Machallah bro ak sarret bi yaffi neh
Thia feling bi la
The best is yet to be reached. Bon courage
Proud of you bro🔥🔥🤌🏾
Bonne continuation mon frère ❤️
Tombé par hasard sur tes sons. Dope you go hard
il ne finira jamais de nous surprendre yagui si way bi frére
JFa City ❤
Toujours au top 💥💯
Frère t'es le meilleur
Nice frère
From big town nice bro 😎
Proud 🥲🥰
MNM do nittou fi
Weureteuut😚i like it❤️this is love storY☺️Bnne continuation te es vrema teop talentūeux✨🙏
Franchement je savais pas cet talentueux
Nice le frére continue comme ça dop
Good song🤙🏽💓
Nice sound nice senario C’est du ouff
😎😎😎oufff
Tu es le meilleur
Nice vidéo
Fort🔥❤
Force bro👏👏
Le flow est extraordinaire 😮🎉🎉🎉
Nice ferer 🥰🥰
C doop frère, c un ami dep8 diaobé
Plus que fort
Sama deuk lay guis dh joal fadiouth
Mogui cool
Xalebi com lem😭
J’adore, Nice na torop 🔥
Bonne continuation
Boy bientôt 3 mois ngay séral. Nieuweul fou défi book! Bala clash bi di sappi
Machallah
Fiér de toi bonne chance c Balla Diourbel