@@abdoullahicamara6553 le bokkaalé est exclu de toute évidence parce que le musulman ne peut pas le faire intentionnellement ndax baatou sédé yi... Ces histoires de bokkaalé sont pour ceux qui prennent Dieu pour un père et genre pas pour les musulmans.
@@mouhamedtoure488 Ce n'est pas si évident mon frr. Bokkalé moy donner des attribut d'Allah à ses créatures mais pas seulement des histoires de père et fils qu'Allah avait déjà répondu dans la sourat 112. S'il te plait démal thi sa imam wala borom xam-xam bou la doy gua lath ko lan moy bokkalé. Aprés, peut-être, tu pourras comprendre ce à quoi je me mets à écrire. Assalamou 3aleykoum
@@abdoullahicamara6553toi tu es entrain de définir les différentes formes de bokkaalé... Ce n'est pas le sujet. Machalla oumpalé wouniou alhouraan. Tu es parti sur une interprétation de bokkaalé que nous sommes en désaccord tout simplement... Je ne défend pas celui qui ne connait rien en chariat en disant suis d'une telle tarikha... L'image modèle des talibés mourides il faut aller la chercher chez les Hizbuts et genre ... Si tu prends référence sur d'autres phénomènes qui sortent ces 3 orientations Iman, Islam et Ihsaan...Allez trouver les oeuvres des concernés pour te documente. Tu verras qu'ils sont plus croyants que ces Dr. As Salamou Haleykoum...
En tout cas c'est seulement Serigne Touba qui a défendu l'islam quand les mécréants se proclamait comme dieu au bureau de ndar. Toi même c'est le mouridisme qui a mis le coran et la sunnah du prophète en toi
En tout cas guinaw sougnou BOROM Mouhamad PSL mo takh S.Touba nékkoul théddo kone nak même sou fékké li am thia bureau ba deug leu je dis Djarama S.Touba wayé nak Mouhamad mome la gnou BOROM bi topp lo kone mom kassé la gnouy topp ba dé incha Allah
Yenn Gamou wou lenn Lousi sen yonnn si Gamou tes Gamou yonennn ti bi késsé laniou fay diangua léé Yenn sen problème moy xam-xam bou new Dieuffou domerame meunoulll wéssou di xass kouy diangue Yonenne bi
Sénégalais khamoul boppam gueneu pauvre gueneu reuy lamigne meno gagner dara surl e plan inrenatinal baparei naane mak gni yane mak. Demlen ci rew yiy doundou dine deuk comme aldiana.bayilene krousyi aussi day def ci yaw ay intuition yookhamni tu te croient plus intelligent que les autres.senegal lolou moy febaram. M ouride mom lilen door mingui nieuw diamono dine moy delousi fii ci senegal inchalah..tarikhayi sen famille rek yewou lene!
Nénako detracteur des sunnit😂😂kham naa gni bokk si tarikha yi duniu ay sunnit, bayyiléne séne thiaaxaane yii da ngéne nio fekk si sunna si gnikoy doune téh diko doundeul, tassawuf souneu ak alkhourane moy fondement bi donc bayilléne féne yi ngéni fénal ak sossal wa tassawuf beug léne guénné si sunna ak alkhourane,
Yaw repantire actif nga nek di deeff : mais dii nga noopii baayi tariikhayi : satan bii nga doone maare taatou saoudiens bamou seette gnew Sénégal di amerder niitt gni
@@marché.pub.tv.officiel Dieuredieuf yaw mon frère, nous avons aujourd’hui les régulateurs sociaux qui sont les taarikhas et nous enviés par beaucoup de pays de la sous région et qui sont eux-mêmes secoués par des guerres ethniques et des attentas :Dieuredieuf sounou kilifeu yii
@@thiernondiaye1975 yow mome douma la tontou ndax app fé'e kate foumou nekk bou nite yi waxé droite goche laye ta yow mome khmnani cii familles fène kate nga dioudou mo tax nga wara teuthie sa gatte app doff nga té mane douma waxak yenn khétte yii
Il ne faut pas les appeler des sunnistes. Juste des musulmans qui préfèrent d'être en contradiction avec les Souffis surtout ceux du Sénégal... Tous les bons musulmans sont naturellement des sunnistes.
@@aladjidiallo3760 Billahi Lolou La Beugone Wakh Dieureudieuf Limou Wakh Ak Li Dr Muhammad Ahmad Lo Wakh Kouko Dégu Khamni Mome Mi Mofi Wakhoul Xam Xam
Barakallah fikoum ya cheikh Dr Ahmed lo qu'Allah vous protège
C'est un savant. Mais le Sénégal n'est pas reconnaissant envers ces trésors. Longue vie Docteur
Exactement
Ma challa cheikhana dr mouhamet ahmet lô yalla nanioula yalla samal
Machallah que Dieu vous accompagne dans votre boulot
Wéddi tazawouf diaroul linguèni doundou nii ndax douko tèrè done deug ak lou werr. Yalla n'a yeurmandé Yalla wathi ci Jullit yepp... Amiine
Billahi
Amougnou probléme ak tassawouf tant que ya pas bokkalé
@@abdoullahicamara6553 le bokkaalé est exclu de toute évidence parce que le musulman ne peut pas le faire intentionnellement ndax baatou sédé yi... Ces histoires de bokkaalé sont pour ceux qui prennent Dieu pour un père et genre pas pour les musulmans.
@@mouhamedtoure488 Ce n'est pas si évident mon frr. Bokkalé moy donner des attribut d'Allah à ses créatures mais pas seulement des histoires de père et fils qu'Allah avait déjà répondu dans la sourat 112. S'il te plait démal thi sa imam wala borom xam-xam bou la doy gua lath ko lan moy bokkalé. Aprés, peut-être, tu pourras comprendre ce à quoi je me mets à écrire. Assalamou 3aleykoum
@@abdoullahicamara6553toi tu es entrain de définir les différentes formes de bokkaalé... Ce n'est pas le sujet. Machalla oumpalé wouniou alhouraan. Tu es parti sur une interprétation de bokkaalé que nous sommes en désaccord tout simplement... Je ne défend pas celui qui ne connait rien en chariat en disant suis d'une telle tarikha... L'image modèle des talibés mourides il faut aller la chercher chez les Hizbuts et genre ... Si tu prends référence sur d'autres phénomènes qui sortent ces 3 orientations Iman, Islam et Ihsaan...Allez trouver les oeuvres des concernés pour te documente. Tu verras qu'ils sont plus croyants que ces Dr. As Salamou Haleykoum...
Mâchallah !!! Tu as dit vrai
Qu'ALLAH exauce les prières amine
Machallah ❤️
Nous aimons le coran et la sounnah rien que le coran et la sounnah. Longue vie à vous Docteur Ahmed lo. L'injure est l'arme des égarés et des faibles
amiine pour les prières
@@alhamdoulillallah9438 katal ndayam feule
تقديس الأشخاص thila ahmade lo saga wa tassaouf yépou
Machaallahou
Machalah
dieureudieuf
Iow singa bokko kon
Machallah ya Dr Ahmed lo
En tout cas c'est seulement Serigne Touba qui a défendu l'islam quand les mécréants se proclamait comme dieu au bureau de ndar.
Toi même c'est le mouridisme qui a mis le coran et la sunnah du prophète en toi
En tout cas guinaw sougnou BOROM Mouhamad PSL mo takh S.Touba nékkoul théddo kone nak même sou fékké li am thia bureau ba deug leu je dis Djarama S.Touba wayé nak Mouhamad mome la gnou BOROM bi topp lo kone mom kassé la gnouy topp ba dé incha Allah
machallah amna solo yala na la yala àr
ana تقديس الأشخاص ya yobou wa tassaouf yépou safara
Yène d wallahi yeneu niakk diom ta soof
Yène chaque année nguèn ni gamou bidâ leu
Ta chaque année mouy gueneu nêkh nitte gni diko gueneu gueum
Yallah mo ngui wah si Al Quran ni lou bah AK lou bonne dou mousseu yéme donté houmbay ba,nékhaye ba,nite yi dafa beuri ba yémeu leu ba diahal la.
Wakho deugg yonén t'y bi la niouy wakhtané thi gamou
أنا متصوف
Yén gnii yéna leunte ba paré beuga diakhassé Rémi, vous avez perdu tout mon estime vous n'êtes pas bien
Kham kham rek ngafi wakh
Yenn Gamou wou lenn
Lousi sen yonnn si Gamou tes Gamou yonennn ti bi késsé laniou fay diangua léé
Yenn sen problème moy xam-xam bou new
Dieuffou domerame meunoulll wéssou di xass kouy diangue Yonenne bi
Jërëjeuf
Jajeuf
Ay original nanfèkh laniou nioom nit gni danioo guemoul sène ndèye
Yaw deh khamo louguay wakh ndah tes Doh degue Lou tes teyoh kham n'a nk dagua khamoule rek moh tah mai yalla nala yalla dioubale
Sénégalais khamoul boppam gueneu pauvre gueneu reuy lamigne meno gagner dara surl e plan inrenatinal baparei naane mak gni yane mak. Demlen ci rew yiy doundou dine deuk comme aldiana.bayilene krousyi aussi day def ci yaw ay intuition yookhamni tu te croient plus intelligent que les autres.senegal lolou moy febaram. M ouride mom lilen door mingui nieuw diamono dine moy delousi fii ci senegal inchalah..tarikhayi sen famille rek yewou lene!
Yaw amed lo foo diaar niou dakharr sa ndaye
abdou gueye bougéne dakharé ndaye SA serigne biga yakar Dina nane dakharr ndayame bamou déki sen luefuele ndaye waye sonale guéné nite
@@mamadoudia1459 👈😂😂😂😂😂
Abdou Gueye Amo Yarr Amo Téguine Amo Xam Xam Mo Takh Saga Rék Ak Menacé Waté Démal Diagui Diéma Kham Sa Diiné Mo Geune
mame ak baye kay boudè daniou wakh si yonène te bi lane mo àye si nètte liko mam ak baye danio diokhone dinè dji sène bip pe
Wakh loudoul deugg mome bakhoul, bo wakhè fiii liii, wakh lénène fénène. Thim!!!
Damay ladjie bakham yén yénay oumarahoul mouminine?
Ba takh nguén né yénay digulé lignou wara déf si lislam nopilene té yam si linguém geum
Dédete waxalugniou souniou bop kaddu yalla laniouy diotali boul diwalé nank rek
@@abdallah3165 d’accord Serigne bi wayé ki wara diotali wakhou yalla kan la?
Manam djiko yisi sariha wakh la begue xam nga balma?
@@abdallah3165 Dieureudieuf
@@mbayediouf7119 waw gooooooooor ahmade lo mi mo saga niti tassaouf yépou thi تقديس الأشخاص
@@serignesalihoufall8512 dama yakrni gayi dagno yeuroul térré bobou rek
Nénako detracteur des sunnit😂😂kham naa gni bokk si tarikha yi duniu ay sunnit, bayyiléne séne thiaaxaane yii da ngéne nio fekk si sunna si gnikoy doune téh diko doundeul, tassawuf souneu ak alkhourane moy fondement bi donc bayilléne féne yi ngéni fénal ak sossal wa tassawuf beug léne guénné si sunna ak alkhourane,
amna niou koy wakh si yènne dè dèk lolou mor kèbè ak ousstaz omar diallo ak omar sall bayyi lène par par lo tay wakh li khèwe
wakh thi micro di khoutba ak woté grand théâtre bidala
Bilahi yay con bida thi dîné motah niouy wakh mbam khoukh damal diangui
@@yerimsow2216 lane moy bida thi diné
@@serignesalihoufall8512 moyi bepp ibada bou amoul dalil si charia comme niko Ibn Hajar Al askalini rahimahoulah wakhé
المولد بدعة حسنة
Yaa mana fenn
@@Bawolbawol diadieuf
@@Bawolbawol fenn mom Ahmad lo
Daara fall lane moyi bonne innovation la beugeu xam
Théy amoul louko gueneu lère
Fenn rek Ahmed lo ak KHALIL lo
Oumar Blondy Niak Yarr Rék Ak Niak Xam Xam Mo Takh Nguaye Saga Démal Diagui Diéma Kham Sa Diiné Mo Geune
@@mansourdieng2000 thieye yalla yene daguen rere lou baril kou wakh ngeune niko demal diangui, wala amo kham kham, wala safara
@@oumarblondy6514 demal Tok
@@mansourdieng2000 rire
Danga wara wakh ak sa talibe yii deh reew nann trop te rewande diarroull diaay thi diine dji
Yaw repantire actif nga nek di deeff : mais dii nga noopii baayi tariikhayi : satan bii nga doone maare taatou saoudiens bamou seette gnew Sénégal di amerder niitt gni
Aka ler frere
@@marché.pub.tv.officiel Dieuredieuf yaw mon frère, nous avons aujourd’hui les régulateurs sociaux qui sont les taarikhas et nous enviés par beaucoup de pays de la sous région et qui sont eux-mêmes secoués par des guerres ethniques et des attentas :Dieuredieuf sounou kilifeu yii
Iblisse lo
Sante yalla
ALHAMDOU LILLAH
Kon singa bokko Iow
Ieo do sah nit
Modou dakhar lo
Sén intérêt rek motakh guén di wakh
Ahmed lô mbam la nafékh la
Yaw kaye noppil rk Liga wax s touba thi sa tére bi لاتسب الاموات فئنهم قد افضواإلاماقدموا
Yaw dagua ka diangue
Yini Diop nitte daguaye teye tes du kham dora wakh Moy toule loh degue rek wala gua guiss rek guakoye juge
Ahmed lô sa saroupe ndeye dangaye doule rekk kharale liye niaff sa ndeye mongui nieuw légui
Serigne touba moléne diagal saga
Sall Birane Niak Yarr Rék Ak Niak Téguine Ak Niak Xam Xam Mo Takh Nguaye Saga Démal Diagui Diéma Kham Sa Diiné Mo Geune Sa Saga Yi Fouf Sakh
@@mansourdieng2000 hé xolale damay tégueul sa ndeye la wax Mane douma sa morom
Sall Birane Saga Rék Ngua Kham Saga Rék Ngua Meune Mo Takh Saga Rék Démal Gnou Yarr La Niak Ngua Yarr Lool Sakh
@@thiernondiaye1975 yow mome douma la tontou ndax app fé'e kate foumou nekk bou nite yi waxé droite goche laye ta yow mome khmnani cii familles fène kate nga dioudou mo tax nga wara teuthie sa gatte app doff nga té mane douma waxak yenn khétte yii
Ki chéytané la bou mak
mbam mou seff ay téré moye boye lo mi nit kou yéss
Yaw Kay Da Deup Wakh Gni Nék Ay Mbam You Seuf Ay Téré Kay Nieup Kham Nagne Léne Yalla Ak Yonéntibi صلى الله عليه وسلم Kasé Gno Fi Nék
Salam, machallah docteur sénégalais yi souba yowmalqiyaam laniouy yewu
Féne rék nga meune doul rék
Vous les sounistes la êtes trop prétentieux.
Il ne faut pas les appeler des sunnistes. Juste des musulmans qui préfèrent d'être en contradiction avec les Souffis surtout ceux du Sénégal... Tous les bons musulmans sont naturellement des sunnistes.
ها هو دجال مسيلمة الكذب
Wahabisme fen rek
Ak doul ak day ak dokhot
Wakhal way
Yaw mi deh gomoh dra si louma yakare ndah li d'où wzkhou kou kham
@@aladjidiallo3760 Billahi Lolou La Beugone Wakh Dieureudieuf Limou Wakh Ak Li Dr Muhammad Ahmad Lo Wakh Kouko Dégu Khamni Mome Mi Mofi Wakhoul Xam Xam
Salafiste yi ay yéfeur lagne
Mdr kholal lingey wakh linga wakh réyna dé
Oustaz Ahmed lo legui Kane moyi yefeur lo mbokk djioulite
Machallah ❤❤❤
Macha Allah
DIEUREUDIEUF