Machalla baye mbaye inchalla man dinako topou bamo diekh sa boma sétan dinako partage mou yatou baye mbaye yalla na yalla goudal saw fan may la ak wérr
Bonjour ! Je suis très honoré par ton engagement pour la cause de cheikh Ahmadou Bamba. C'est nous qui devriez le faire en tant que talibé. Saches que je suis derrière vous et que je compte partager avec vous des poèmes que j'ai écrit sur le Cheikh. Je suis talibé de Serigne Moussa Mbacké Abdou Bakhé. Qu'allah vous protége
Ce traitement de ĺ histoire avait été predit de Patrice Lumumba : un jour se lèvera ; l Afrique 🌍 reécrrira son histoire En voici un qui a réalisé ce que di disait Patrice Lumumba
L Université de Touba Fac Sciences historiques/ Ces recherches sur la vie et ĺ œuvres de Serigne Touba : Modules/ Cité : Enseignement et recherches: Professeur Sayh Mbaye G Sylla
Mbaye Gueye syll yagg fi lool ta wérr Paul Marty dafa am ay talibé Sénégal wayé dinane khamni mbiri Serigne Touba kawla dieum. Ta niakka kham Kim waral da beuri li Paul marty wakh lépp bouñko guénné ñi contaan instant bi défko ngannaay ngalla bou booba boulénko wéddi archives yi niongui fi
"Nous devons voir de tous musulman sénégalais inspiré de sa religion une ennemie à la France" disaient les colons. Cette vision colonialiste du Noir traverse toute l'œuvre de Marty et transparaît par exemple quand il parle d' " âme noire ", de " mentalité noire ", de " l'exagération coutumière des Noirs ", de " paresses du Noir ", que le " vêtement de l'Islam " n'est pas "taillé pour les Noirs ", que les " Noirs n'ont d'ailleurs aucun respect pour les livres sacrés ", etc. Ces expressions, nous le voyons, reproduisent les pires clichés coloniaux. Le Noir dont parle Marty n'est par le Noir individuel avec un itinéraire personnel bien défini, mais du Noir archétype, idéel, fabriqué par le discours colonial. Cependant, on ne sait par quel miracle Marty fait subitement de cette doctrine non pas " une secte particulière d'Amadou Bamba " mais une " confession islamique " quand elle pénètre en pays sérère! De plus, grande est l'erreur de Marty sur le plan de la méthodologie qui prend comme référence les informations fournis par des éléments externes à la mouridiya .Il donnait beaucoup de crédit aux propos de ceux qu'il appelait " Les autres noirs musulmans " mieux placés, selon lui, pour apprécier à leur juste valeur les doctrines religieuses de la mouridiya On sait pourtant que les relations entre les différentes communautés religieuses n'étaient pas des plus sereines durant l'intermède colonial, les Français par leur politique du " diviser pour mieux régner " contribuant en grande partie à les opposer en élevant des communautés au rang d'officielles et loyalistes et d'autres au rang de groupements rebelles. Paul Marty ne trouvait du reste aucun mal à cette division; il faisait cette prédiction ignoble: " Où sera le mal, quand dans un demi siècle les islamisés du Sénégal seront partagés en cinq ou six sectes différentes, très divisées entre elles, d'autant plus divisées que chaque secte sera un produit national, et que ces rivalités religieuses viendront se greffer sur des animosités de race ? " Ceci dit;ne devons nous pas nous musulmans du Sénégal s'unir contre les idées de Marty plutôt que d'en faire une source pour critiquer Serigne Touba.
Salam ou lieu de lire le rapport qui dit rien de bon sur notre cher bien aimé cheikh Ahmadou bamba, amène nous des preuves qu'on a pas pour nous défendre contre ce qui utilise ce rapport pour nous dénigrer.
Ndakh guiss nga limo bind wakhal ko zeydi El hadji malick sy né moume la doune signé ak rapor yi dokh sén diganté ak nimo andé woone ak gnoume Paul marty do wakh deuge mokko
Serigne mbaye wakhoul comme yene mom ay document la indi du démontrer scientifiquement ana Say argument wax you sew rek dem len tok bamba raw nalen ba paré
Serigne mbaye wakhoul comme yene mom ay document la indi du démontrer scientifiquement ana Say argument wax you sew rek dem len tok bamba raw nalen ba paré
Je ne pense pas que le rôle de Paul Marty était de combattre le mouridisme . il était affecté au Sénégal pour étudier les sectes et leurs fonctionnements ( mouridisme,tidjania ...) .il a écrit sur beaucoup de marabouts
Magui guiss gnou bi séni page fecbook di dieul wakhi paul marti mana serign bi dadone tague wiliyame baunti di wakh ay wakh you gnaw yokhame ni kéne khamoul loumou done
Héy yéene wa réwmi 🇸🇳 nanou doli santate Cheikhouna bamba ❤️ Baye Mbaye Gueye Syll l'infatigable 🙏🏽 jàmm rék inchallah 👏🏼
Dieureudieuf serign mbaye gueye silla sa liguéye raféte na machalla
Machalla baye mbaye inchalla man dinako topou bamo diekh sa boma sétan dinako partage mou yatou baye mbaye yalla na yalla goudal saw fan may la ak wérr
Dieuredieuf leerna té tégouna si xam xam yalnala sérigne touba faye
Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll. Amna solo lol.
Jërëjëfëti serigne Mbaye Gueye Syll. Yalna Yalla fayla yiiw wu baree bari ci barkeb Khadimu Rassoul.
Masha Allah amena solo lol, épisodes yi lumu bëri bëri kep ku mbirum Serigne bi yiteel digako topu
Gnigui teewlu 2e épisode bi Insha Allah; jërëjef
Diara dieuf serigne Mbaye Gueye Sylla akanekholl nio ame 100 persone you mellni yaw ame takhawaye bi nga ame
Bonjour ! Je suis très honoré par ton engagement pour la cause de cheikh Ahmadou Bamba. C'est nous qui devriez le faire en tant que talibé. Saches que je suis derrière vous et que je compte partager avec vous des poèmes que j'ai écrit sur le Cheikh. Je suis talibé de Serigne Moussa Mbacké Abdou Bakhé. Qu'allah vous protége
Yalla na Yalla barkeel sa liguey bi Amna solo loll Té and ak Tawfekh
Merci beaucoup baye Mbaye pour ton infatigable travail pour nous éclairer sur le mouridisme
Baye mbaye geuye geunal yague geuna wèrr
Serigne Mbaye Gueye il faut publier les rapports sur votre page Facebook
Yalla na godall sa fane pape
Yalla na yalla dogal nga matal sab ligéy Barkéb Borom Touba Mbacké
Sénégal mo bari ay mbam khoukh keep kou bagne serigne Touba kalbou mola gueune
Niogui koy topou inchalla na dém ba 200 épisode sah
Machallah Dieureudieufé Serigne Touba
Dieureudieuf baye Mbaye amna solo
Merci baye mbaye yageu té weur
Bizarrement je constate un lien étroit entre les disciples de Marty d'aujourd'hui et les collaborateurs des colons d'hier.
Effectivement nonou demb Yi séni seuut gnofi nékk Di nonou Yonne wi ba lêgui
Sunu baye bi yalla nafi yagg lol diniou lèral histoire senegal ak kou ted ki Ahmadoul xaadim
Dieureu nguéne dieuf
Dieuredieuf serigne mbay guey Sylla
Macha Allah baye mbaye
Machala
Dieureudieuf s touba mbacke rek 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍🇸🇳
Amna solo machalah senegal da nakhare wakhe ndakh colonial bi mo sonal motakh rewmi dou dem
Machalla amna solo loull❤️
SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM DÈ
Amatina solo dierediaf borom touba
Dieureudief s Touba
Dinañu topp lépp insàllaah
Mâsallax ñogi xaar yènene episode yi
Jaajeuf. Dina gnouko annde ak yaw bamou dieekh Inshaa Allah
Kham kham bi rafit na
Masàlla
Merci Serigne mbaye Gueye Sylla
Mashala bay mbay sama nidiaye
Macha allahh
👍❤❤❤❤❤❤❤
جرجف بارك الله فيك وزادك بسطة يا شيخ مبي غيي سيل
Machalla amna solo loll
Jasaka Lah
Machallh
Wawa Baye , you are
Machalla ❤️😭
Magui Ziyar bou bakh waye borom sham dosi farale di wakh
Amna solo, sant nagn ci bu baax. Nioo ngi koy khaar bu baax
بارك الله فيك بجاه شيخ الخديم
Akassa serigne Mbaye niongui lay santate bou werr
Ce traitement de ĺ histoire avait été predit de Patrice Lumumba : un jour se lèvera ; l Afrique 🌍 reécrrira son histoire
En voici un qui a réalisé ce que di disait Patrice Lumumba
Machalla baye Mbaye l
Baye mbaye sa ni moro lasokh la
Machalla
L Université de Touba Fac Sciences historiques/
Ces recherches sur la vie et ĺ œuvres de Serigne Touba : Modules/ Cité : Enseignement et recherches: Professeur Sayh Mbaye G Sylla
Amna solo
تقبل الله عملك ونصرك نصرا عزيزا
Machala papa
Thiey liii dh massouma guiss loko geuna leir
Merci pour ce travail.
diaradiafe s touba amol morom
Mbaye Gueye syll yagg fi lool ta wérr Paul Marty dafa am ay talibé Sénégal wayé dinane khamni mbiri Serigne Touba kawla dieum. Ta niakka kham Kim waral da beuri li Paul marty wakh lépp bouñko guénné ñi contaan instant bi défko ngannaay ngalla bou booba boulénko wéddi archives yi niongui fi
Amna solo Baye Nice na
Nogui koy tew lou bou bakh papa yague fi
"Nous devons voir de tous musulman sénégalais inspiré de sa religion une ennemie à la France" disaient les colons.
Cette vision colonialiste du Noir traverse toute l'œuvre de Marty et transparaît par exemple quand il parle d' " âme noire ", de " mentalité noire ", de " l'exagération coutumière des Noirs ", de " paresses du Noir ", que le " vêtement de l'Islam " n'est pas "taillé pour les Noirs ", que les " Noirs n'ont d'ailleurs aucun respect pour les livres sacrés ", etc. Ces expressions, nous le voyons, reproduisent les pires clichés coloniaux. Le Noir dont parle Marty n'est par le Noir individuel avec un itinéraire personnel bien défini, mais du Noir archétype, idéel, fabriqué par le discours colonial.
Cependant, on ne sait par quel miracle Marty fait subitement de cette doctrine non pas " une secte particulière d'Amadou Bamba " mais une " confession islamique " quand elle pénètre en pays sérère! De plus, grande est l'erreur de Marty sur le plan de la méthodologie qui prend comme référence les informations fournis par des éléments externes à la mouridiya .Il donnait beaucoup de crédit aux propos de ceux qu'il appelait " Les autres noirs musulmans " mieux placés, selon lui, pour apprécier à leur juste valeur les doctrines religieuses de la mouridiya
On sait pourtant que les relations entre les différentes communautés religieuses n'étaient pas des plus sereines durant l'intermède colonial, les Français par leur politique du " diviser pour mieux régner " contribuant en grande partie à les opposer en élevant des communautés au rang d'officielles et loyalistes et d'autres au rang de groupements rebelles. Paul Marty ne trouvait du reste aucun mal à cette division; il faisait cette prédiction ignoble: " Où sera le mal, quand dans un demi siècle les islamisés du Sénégal seront partagés en cinq ou six sectes différentes, très divisées entre elles,
d'autant plus divisées que chaque secte sera un produit national, et que ces rivalités religieuses viendront se greffer sur des animosités de race ? "
Ceci dit;ne devons nous pas nous musulmans du Sénégal s'unir contre les idées de Marty plutôt que d'en faire une source pour critiquer Serigne Touba.
Gou bugu mam bamba sem
Massalla
Mala beugue lo sakh
Poème bi araab yi da jarul yoon sax.
Tu parle de Kelly poeme
@@cheikhlo6150 le poème que paul marty a attribué à serigne touba
quel est le titre de la musique d'introduction s'il vous plait ?
Chanteur : Serigne Mama Ndiaye
Titre : natto di kér kérane
Auteur : Serigne Moussa Ka.
Amatina solo
إن شاء الله سننتابع إلى النهاية
Salam ou lieu de lire le rapport qui dit rien de bon sur notre cher bien aimé cheikh Ahmadou bamba, amène nous des preuves qu'on a pas pour nous défendre contre ce qui utilise ce rapport pour nous dénigrer.
Weddil boula nekhé. Paul marty lou ler la wah. Yow dangay défendre sa serigne rek.
Waw mom ay documents leu indi dé est-ce que tu as lu le rapport qu’il montre sur la vidéo.
Xeyna lerna si iow
Ndakh guiss nga limo bind wakhal ko zeydi El hadji malick sy né moume la doune signé ak rapor yi dokh sén diganté ak nimo andé woone ak gnoume
Paul marty do wakh deuge mokko
Serigne mbaye wakhoul comme yene mom ay document la indi du démontrer scientifiquement ana Say argument wax you sew rek dem len tok bamba raw nalen ba paré
Serigne mbaye wakhoul comme yene mom ay document la indi du démontrer scientifiquement ana Say argument wax you sew rek dem len tok bamba raw nalen ba paré
Je ne pense pas que le rôle de Paul Marty était de combattre le mouridisme . il était affecté au Sénégal pour étudier les sectes et leurs fonctionnements ( mouridisme,tidjania ...) .il a écrit sur beaucoup de marabouts
Magui guiss gnou bi séni page fecbook di dieul wakhi paul marti mana serign bi dadone tague wiliyame baunti di wakh ay wakh you gnaw yokhame ni kéne khamoul loumou done
Lolou yeup dina mabb bayiléne rek
Sou amone dei publiè naniuko bou yag ...
Sunu Borom mi beug mbir yi leer mi takh mu khiir leen si marty. Waaye tewlul père Mbaye rek lepou dina leer
Mème mane Guisnako
Machalla
Machalla
Machalla