Salut coach Ass et Mia yen Niar yéna takh ma bàyyi masturbation presque mongui beugua yague Guinaw yàlla Malen siy sante boubakh ndakh masturbation kouko bayi tè ama Goul diabar ndax am nguen produits yo kham ni Dina takh sa bou také diabar Bou deffé rapport yague ak dokhnam wala Loum wara def Guinaw souko bayyé conseil s'il vous plaît 🙏🙏
Slu coach ndakh djigeune bou eumbe dina guiss règle répondez-moi s’il vous plaît je suis enceinte mais j’ai fait une remarque ni damay géuné dérét merci 🙏🏽
Titre bi damako lire aye rétane diapp ma. Wa légui yaw sa dieurkeur bagnou dégg ko ba dina bakh ci yène tamite nak. Vraiment femme est compliquée 😂😂😂😂😂😂
Svp Ass tountou ma Pour sauver sama mariage parce que mane dama deude ak sama dieukeur té seigué wouma mais li ma diakhale moye meussouma kham goor apprat sama dieukeur
Slt coach Aas kii benn soxna la nee na biiram dafa am lu ciy tëf-tëfi comme fit buy tëf-tëfi ni muy def noonu la biir bi di def ba mu koy yëg bu baax te ëmbul te la plus part bu période tam di waaj a jot walla mu am retard la koy faral di def muy laaj ba xam loolu lan la ?
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
Sama questions moy Mane personnellement loutakh souma yewo fadjr ba dioully , diguentè bobu may teudatte sama awra bi dina diougue, diougue bo xamm ni day deugueur wow kong ba day moudiou sakh di metti ba douma beug loudoul mou ress . Durée bi c’est maximum 8 à 10mnt Tè lima diaxal moy douma xalatt dara mome moyë diougueul boppam . Lolu lanne la ?
Slt coach ass et Mia CV tay sma question Moy damay ladj Mane sma soxna bumay feleurt ak mom bu l'ale sma thiouse bi rk damay danou way3 mene nma suc3 plus de 10 minutes teh duma danou
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
Moi je suis célibataire mais j'ai une fois fait rapport avec sama cpoin mais j'ai remarque que à chaque fois si il m'appelle il veut on le refait je ne sais pas pourquoi mais il me dit que il m'aime aide moi

Machallah ass Say kafou rafét Lou nako diadieuf
Sonko Moy diomay diomay Moy sonko ❤
SONKO MOY DIOMAYE/DIOMAYE MOY SONKO
Nane bayi khèl ni am na nioku doll diodowalè
Sama coach❤❤❤❤yama diangale lou bari
Ndeysane caoch yeramnala trop si question yi
Bilay damalène beugue am lèn diam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Démay lathié ndakh biir bu reuy déy wagni awra goor ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sonko moye Diomaye
Ay hunhun ak waw Mia tam doune si wakh
Slu coach dama don ladie ndax kou am mauvaise haleine meun na dieul soungoufou nep nep diko galakhndiko chaque matin ou chaque soir
Sonko kasse amoul lenen
Ass yokala mougne rek
Salam salam coach asse coach Mya ❤❤
Hépatite b koko âme
Esq man n'ay nan nébeday
Miya del mourou bakor gui dialle
Salut coach Ass et Mia yen Niar yéna takh ma bàyyi masturbation presque mongui beugua yague Guinaw yàlla Malen siy sante boubakh ndakh masturbation kouko bayi tè ama Goul diabar ndax am nguen produits yo kham ni Dina takh sa bou také diabar Bou deffé rapport yague ak dokhnam wala Loum wara def Guinaw souko bayyé conseil s'il vous plaît 🙏🙏
Salut les choco man sama soxna yarambi daytang rawatina gouddl gi mabaga xam loukouxarl
Slu coach ndakh djigeune bou eumbe dina guiss règle répondez-moi s’il vous plaît je suis enceinte mais j’ai fait une remarque ni damay géuné dérét merci 🙏🏽
Loy wakh ni ms drette bi amou si Yonne dhe demal hôpital si sage femme bilay visite ngua wakh koko
Ass kénal yalla sama lathie Moy dianndam ninkoy itilisé
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci
Salam coach et mia damay lathie Yarame bouy tange Lou kay waral svp 😢😢
Ndokhu sitti mokoy waral
❤❤❤❤🎉🎉
Slt Ass est ce que lèm day diokhé diabéte svp
RESPECT à vs deux ❤❤
Titre bi damako lire aye rétane diapp ma. Wa légui yaw sa dieurkeur bagnou dégg ko ba dina bakh ci yène tamite nak. Vraiment femme est compliquée 😂😂😂😂😂😂
Ce sont des décharges électriques
Ça existe surtout bou booya
Salut man demaye ladie ban position mo gene boye def rapport ak sa sokhna bo Ombè svp gen répondre ma question bi
Merci beaucoup à vous ❤❤
Cotch lo kham ci kou tok 8 mois guissoul soxnam mou wath bay dem soxnaci febar
Gour bouy Say AK djigénn bou manniyou bi di guénne nanlakoy khamé
Djigén bouy say ak gour bou manniyou guénné nanlakoy khamé
Mafi djitou ❤❤😂
Ass yow ak Mia sén émission bi est-ce que dolén xaar beu après ndogou nguén def ko conseil la rek
Svp Ass tountou ma Pour sauver sama mariage parce que mane dama deude ak sama dieukeur té seigué wouma mais li ma diakhale moye meussouma kham goor apprat sama dieukeur
Mais c la même question kil vien de traité prend cette vidéo tu montres a ton mari
Envoyer ko video bi
Ms coach Mia sa melfa bi MAYKO sma soxna si way
Ndakh naan garabou emorid te amoko ndakh dey lorei?
Slt coach Aas kii benn soxna la nee na biiram dafa am lu ciy tëf-tëfi comme fit buy tëf-tëfi ni muy def noonu la biir bi di def ba mu koy yëg bu baax te ëmbul te la plus part bu période tam di waaj a jot walla mu am retard la koy faral di def muy laaj ba xam loolu lan la ?
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
ioe d nio yam, wanté lolou déséquilibre hormonal dékoy déf...taux téstesterone bi mo bari
, 😂😂😂😂😂😂no assane bilahi ken dou yaw
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
❤❤❤❤❤❤❤❤
Sama questions moy
Mane personnellement loutakh souma yewo fadjr ba dioully , diguentè bobu may teudatte sama awra bi dina diougue, diougue bo xamm ni day deugueur wow kong ba day moudiou sakh di metti ba douma beug loudoul mou ress . Durée bi c’est maximum 8 à 10mnt
Tè lima diaxal moy douma xalatt dara mome moyë diougueul boppam . Lolu lanne la ?
Yow esque khonio lolou Kaye ce naturel soudé salibataire nga dèmele taky diabar soco manoule ngaye woor
😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👍👍
Coach sama culturiss by daye khasann dém na 2 hôpital mais dou éféxion
Esk dou sothiate
Esk dou sothiate
Slt coach ass et Mia CV tay sma question Moy damay ladj Mane sma soxna bumay feleurt ak mom bu l'ale sma thiouse bi rk damay danou way3 mene nma suc3 plus de 10 minutes teh duma danou
Fofoy sa points faibles rk😊
Ass woril
Salut coach guiss règle le 11 guisatt ko le 27 c normal ou bien j s8 célibataire
Lou waré manque d'envie seuye
Man sama awra bi dafa am ay pithie you bari di méti
Ass somÿidem cabine demayi mellni koyi zarou pitti sisouff lolou lan mokoyi fat sonallnamah torop totoumah sakzourr mapozela kesiyobi tedo matontou
Lolou hémorroïde yi
Ass diokhé na solution bi avant hier outeul soungoufou gnandam je pense lolou la wahone
2026 kay 😂😂😂😂😂😂 beugeuko dh day doull
sol sa kalson djieukeur ndakh bakhna😊
😂😂LOLOU CI JONGUÉ LA BOKK👍👍👉💗
😅😅@@NDIAYEDRANGON
Mya: carton rouge
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
Ass es ce que shake off mane na fathie distrophine ovariene
Amadou ba 5em p
😂😂😂😂
Ass mia slnk awra gor bou am ay pithi you wèkh you ndaw lan lay signifier
Slt coach asse yane position gnoy reuyeul awra goor bouy def rapport sexuel svp
Man lolou moma dal😢😢bilakhi dama ted awma ndaw te poutan masouma def rapport bilakhi
moi aussi
@@YacineNgom-nz5it Hum ww loy lolou Man dama ross baye bègue dh ndakh sougnou wa keur ligne maye khole sama diekeur garawou mom amoul problème
@@YacineNgom-nz5it te compound nama
Man dama amoul appétit sexuel dara diappale léenma s'il vous plaît
Moi je suis célibataire mais j'ai une fois fait rapport avec sama cpoin mais j'ai remarque que à chaque fois si il m'appelle il veut on le refait je ne sais pas pourquoi mais il me dit que il m'aime aide moi
Stp boul ko mosa défate peut importe la situation damalako niane rek
Erreur la mais boumou la dalate il ne t'aime pas
Wolouko rk
Coach Sama Question moy Depuis Koor Gui Commencé Déchet You nioul Kouk lay guéné té Khawma Louko Waral
Bonjour sama seins yi day méti Di diss thiouss yi Di khasane may lath lane la
Cv Ass mane sama règle da retard té mossouma dal en plus démay saw rék té souma wooré démay sonou trop
Defal test de grossesse
Slu coach dama don ladie ndax kou am mauvaise haleine meun na dieul soungoufou nep nep diko galakhndiko chaque matin ou chaque soir
Ndakh naan garabou emorid te amoko ndakh dey lorei?
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
Coach man sama yaram bi Dafa beuri karaw loll niou néma karaw bi bou dénioul do mana khéss sama peau bi rafétoul Dara ndakh karaw may lathie louy solution bi pour mou mana dégne svp
Kaye ma watal lako
wouteul crème épilatoire wala mousse de rasage geu defko sa yaram pendant 3mn geu dindi koc facile