Salut Ass man ça fait longtemps que j'ai pas vu ma femme et elle était enceinte maintenant elle a accouché Alhamdoulilah et que man dama sonou lol sah may lathie solution pour wagni thiono gui bilaye c'est compliqué dh
Merci beaucoup 🙏 Aas et Miyaa linga done wakh si 🌸 tortorou sapsap lou wèr leu sama guis dafa geuna leer👀 mais man dama setlou ni fan yi damay gaawa nelaw te dawoua gaawa nelaw.
Coach ass et mia dafa question bouma djakhal moy boy dieul sa sokhna pour premiere jour bi ndakh ndawou xalé bou djiguen bi dafay dagueu avant may danou wala bouma dano la ndaw gui di dague ? Yeen rk lasi wolou pour am si lou lèerre
Ça va coach ass silonek khamna war ngama fay je suis célibataire mei djégu bouma guis nila esk yangi sétan ass boné dédét manila lan kokou niak ko topou woroul djégu bouka topou do am ďéfét bilay Man mom bis bouma amé dieukeur sa keur lay nieuw 😂
Bonjour coach si c’est possible est-ce que vous ne pouvez pas faire parfois 1 émission en français même si c’est une fois par semaine parce que les vidéos sont importante et ça pourrait même intéressé les blancs ou bien les autres qui ne comprennent pas wolof ou bien pour beaucoup élargir la chaîne
HU.MM ASS TAYE MOME DIOUME NGA ,ومن كل شيء حلقنا زوجين،،YALLA NÈNA LEUPP LOU NÈK MAKO BINDNA NIOU DONE AYE PÈR GORR AK DJIGIÈN SOIT NGA HAM WALLA NGA NIAKKA KHAME
Gnari yona guini May posé question kén douma répondre stp dimbali lén ma soumay def rapport sama nakk bi day méti té sexe bi day khassane bassi birr sama nakk bi di gonflé légui souma beugué saaw sah day guene méti té souma saawé ba paré day dess di tokkou ak perte blanche
Ass mane sama problème moy sama copin bi dafa djéki djéki rk téyé bobap sa fait 1mois téh défou mako légui un jour ma vocal ko maniko tate rk ngama topé beuguoma téh mak mome sékhougne dra loudoute fleurté mais dama beugone juste mou wakh ak mane motakh ma wakh ko lolou damakoy envoyé vocal mais dra douma tontou je préfère ma quitter relation bi sakh mais damako beugue trop mais amoute si mane yeuk yeuk😢dama mèr sakh ba supprimer numérome faléwouma bèn yone may lathié ndakh mots bimako wakh dafa eupou waleuhh mome dafma beugue toute ngéneunèn 1âns et quelques mois je veux la solution svp😭😭dsl pour la longueur🙏🏼
Je suis élément de coach Ass et Mia je vous aime fort ❤ mia sëy bi yalna barké
Salut Ass man ça fait longtemps que j'ai pas vu ma femme et elle était enceinte maintenant elle a accouché Alhamdoulilah et que man dama sonou lol sah may lathie solution pour wagni thiono gui bilaye c'est compliqué dh
Merci beaucoup 🙏 Aas et Miyaa linga done wakh si 🌸 tortorou sapsap lou wèr leu sama guis dafa geuna leer👀 mais man dama setlou ni fan yi damay gaawa nelaw te dawoua gaawa nelaw.
CV nkm bane épisode lawone
Yalna séy diam yague ❤️
Salut séne céréales bi sokoye utiliser daguasiye bollé guarabb , bouye rakhase biirr wala , pour gua ndiéll poit si lou guaww 🙏🙏
Cv coach sou may guiss régal dou métti mais sou may saw day métti badouma mana tok pour saw
Cv miya ndakh imorit meuneu bloqué ay régel ndakh meuna takh djiguéne dou ame dome
ndakh sol sa kalson Dieukeur bakhna
Une question, je voudrais c'est lui qui a problème < manuyu> merci
Coach ass et mia dafa question bouma djakhal moy boy dieul sa sokhna pour premiere jour bi ndakh ndawou xalé bou djiguen bi dafay dagueu avant may danou wala bouma dano la ndaw gui di dague ? Yeen rk lasi wolou pour am si lou lèerre
😂😂😂 bo danou doko mana dague dh da ngay profiter mou dague avant ngay danou
Ki ray nama😂😂😂😂
😂😂😂 ndeysan mashallah question bi amna solo trop 😅@@mameseynaboundiaye6015
😂😂😂😂daguay danou apare mou dague
Pourtant limou lathi question la dhd Magui car réponse asse
Félicitations Mya heureuse ménage 🎉
Salut asse louy dindi cernes svp
Ça va coach ass silonek khamna war ngama fay je suis célibataire mei djégu bouma guis nila esk yangi sétan ass boné dédét manila lan kokou niak ko topou woroul djégu bouka topou do am ďéfét bilay
Man mom bis bouma amé dieukeur sa keur lay nieuw 😂
Coech man defois sama nakeuu bi dafay faral di metii trop dh suis Viège lolou moma diaxal 😢
Salut a vous deux mes j'ai une question qu'est-ce qui augmente awra goor
Coach khana Di ngéne poss ba Goor Gui diale
Miyà yawé eska Amiga diekarr ❤️❤️❤️ damàla beaucoup tack ❤❤❤
Xana do khooool👀😂 Miyaa jarna
RESPECT à vs deux❤❤
Wa As dimba luñu si nkala goor di wadie chi premier gu dem ak sokhnam cvp
Salam Mia duel l'aye Dour chaque jour ndax bakhna
Merci ass et Maïa man damai ladj hâlé boñ violé bemé am 10Anne eska man nay amat ndaw
Cv ass damay ladj garawo pokhotan ak garawo nakhue lan Moy senn ndiarigne si nit
Mbégnéfégné c'est bantmbaré en Wolof
Salut dakh kou deff planning monnaie utiliser 4 côté wala thiepou
Gresss mbeut bovou mome Ass ameguako ?
Ton numéro de Dakar way.
Slt intime femme sama copine bi nena dafa degeu niouni softcare dafay deviergé djiguene ?
Mbégné fégné mo sérrére la mome lagnouye wax mbatambaré si wolof mais coach Mane déh soumaye daw sama Pothie yi dégnouye xassane loukouy dindi
Bonjour coach si c’est possible est-ce que vous ne pouvez pas faire parfois 1 émission en français même si c’est une fois par semaine parce que les vidéos sont importante et ça pourrait même intéressé les blancs ou bien les autres qui ne comprennent pas wolof ou bien pour beaucoup élargir la chaîne
ASSE wakhal bokk si graice sou
Mbegné fégné moye mbante maré en serrére
Salut coach mbégnéfégné moy mbantamaréne on appel comme sa en sérere
Sama kharite bou djiguéne la beugeue té môme dafmay charmé reck mais on a même pas parlé de l'amour durant nos amitiés
J'ai 3 ans de relation mais mon homme se comporte ainsi
C quoi le mbeute ?
Dama doukhane une femme mou d'accord après la landemai mouné ma beugoul ma Est ce que beugnama
Respecté niou waay 😂😂
QuestionSama dammalyi benibi darery lool bamojaxalma bifeté dourat momla dafatolni domou Orange basoumay daw dayméti madon laje bagam M borostat wala sonalnama tayensa y damay santir loumelni boul diyek samabirbi diméti dimbalémasi gawahma damousoumadall😭😭😭
Dagay dem hôpital
Demal def test cancer c'est mieux
Lolou khoukhane la tel si djouk bala mouy eupou lokho
❤❤❤❤❤❤
Mbegner fenier moy mbanté en wolof pour gnioko khamoul
Question pour sama xarite bimay andal amoul tlphone néna ndakh kouy mbalou nimouy gaawé daanou ndakh nonou lay gaawé daanou bouy deff rapport
HU.MM ASS TAYE MOME DIOUME NGA ,ومن كل شيء حلقنا زوجين،،YALLA NÈNA LEUPP LOU NÈK MAKO BINDNA NIOU DONE AYE PÈR GORR AK DJIGIÈN SOIT NGA HAM WALLA NGA NIAKKA KHAME
Salut coach Sama kanam déy guéné ndokh bou wèkh ter célibataire
la
Démal sayi bou sayé modange 😶
Lolou infection la rek demal fadjou
Ass eluek yalla Dinala douma de
Khana yaw lay diokh yar bi
Wa coatch mballou mom lann lay deff si goor
❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
?Petit colo loumoy dèf si goor coch?
❤❤❤❤🎉🎉
Cv ass silonek yagui si diam mane dé bén dom la am té sama kanam day géné gélaw ma beugon kham lan la
Guarabou mbanta marré moy mbégn féénié
Diam rk guéne di ame❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mbéniéfenié moy mbantamaré si serere
Ass mane sama diabar sou niouy seuy. Soumako doiter daye saw
Gnari yona guini May posé question kén douma répondre stp dimbali lén ma soumay def rapport sama nakk bi day méti té sexe bi day khassane bassi birr sama nakk bi di gonflé légui souma beugué saaw sah day guene méti té souma saawé ba paré day dess di tokkou ak perte blanche
Slt Ass cv,démaye lathié sexe bouye kheusseun di am pithie dakh moun nala téré am dôme
Wakh ak sa copin wérou koor di toy ba paré di lala lé sa sex ndakh soyè wo meun gua woor
😂😂😂legui wori nan toyall khip
Ass mane sama problème moy sama copin bi dafa djéki djéki rk téyé bobap sa fait 1mois téh défou mako légui un jour ma vocal ko maniko tate rk ngama topé beuguoma téh mak mome sékhougne dra loudoute fleurté mais dama beugone juste mou wakh ak mane motakh ma wakh ko lolou damakoy envoyé vocal mais dra douma tontou je préfère ma quitter relation bi sakh mais damako beugue trop mais amoute si mane yeuk yeuk😢dama mèr sakh ba supprimer numérome faléwouma bèn yone may lathié ndakh mots bimako wakh dafa eupou waleuhh mome dafma beugue toute ngéneunèn 1âns et quelques mois je veux la solution svp😭😭dsl pour la longueur🙏🏼
Da ame foulla rek defall kom mom ndakh taka goula dif nii boula takon doula fale bo togue rek ame kenen
D’égal Lila Khadim wakh
@@Khadim-mk5cg lolou la nék di dèff sakh merci frère
Peut être begatoula rk
❤❤❤❤
❤❤