Magui lenedi dieul ceddé ni sant na Yallah bou bakh Diouli si yonenté bou Tedd ki Mohamed Rassoulalahi psl ci linou ma bolé ci Ndiabotou Serigne Touba Khadimou Rassoul. Magui toudou Ndongo Wade
Dierediefe serigne touba serigne mountakha mbacké yalla nafi yagg te annd ak weer ci barke rassoullilah sallahou aleyhi wassalam ak serigne Touba amiiiin .
Cheikh Akhmadou Bamba, le serviteur du prophète (psl), a montré sur ce poème son caractère multidimensionnelle et son amour inconditionnel à l'élu de Dieu. Dieureudieuf Serigne Touba
Serigne Moustapha Seck Yalla nala Serigne Touba bégueul. Koula déglou xolam dafay sédd gouyy. Yalla na say fann gouddou té nga amm wér si BARKÉ Serigne Bamba.
yalla nanga goudou fan man tydiane laa waye serigne touba limou wakh yonentebi reuyna kou sopou yonentebi boko degloo sa khol dina tooy . day yokou thiofel si yonente bi
Dierediefe serigne touba serigne mountakha mbacké yalla nafi yagg te annd ak weer ci barke rassoullilah sallahou aleyhi wassalam ak serigne Touba amiiiin .
Sante Serigne Touba si mokkale bimouma mokkale lo Moukhaddamaatoule amdaah. Serigne Moustapha SECK Yalnala Yalla faye.. Chaque jour que Dieu fait tu nous accompagnes de par tes si belles prestations.
As salamou aleykoum serigne Moustapha yalna borom bi defal la djam weral bate bi,bilahi mouhadimate bi ningako djangué yém nama weur na ba sonou foumay amé son bi,vidéo TH-cam bi rek la télécharger,awma si sago barkep serigne bi❤😭😭😭😭😭😭😭
Jërëjëf, sëriñ Mustafa. Sëriñ Touba kenn la., Mbacké Balla Aysa. Boroom Touba ak Njareem. Moom rekk moo jaxalan toubab yi. Mënu ñu wën dara ci moom. Ñu yobbu Gabon juroom ñari at aki ay weer, mañu luñ ko dara, ñu deloo si ko ndakaaru... Mbacké, kenn du yow! Jërëjēf Sëriñ Touba!
Nee leen, jërējëf Seriñ Touba!
Hassida bi segn touba nenathi kou amoul Daray yeuk yeuk thi hassida ngui meno beugueu yonetbi psl aleyhi salatou wa salam🙏🏿🤲🏿❤️🕋✨
Macha allahou serigne Moustapha seck yalla na yalla goudal say fane thibarkee yonentibi salla lahou halleyhi wa salam
Yalla nama cheikhoul khadime sopi si barkep serigne Saliou
Serigne Moustapha seck yalna sa borom goudal saw fane Dieureudieuf
Magui lenedi dieul ceddé ni sant na Yallah bou bakh Diouli si yonenté bou Tedd ki Mohamed Rassoulalahi psl ci linou ma bolé ci Ndiabotou Serigne Touba Khadimou Rassoul. Magui toudou Ndongo Wade
Damanane alhamdoulila bi ma boké thi ndjabotou seydina Mohamed ak khadime Rassoul ,❤️
Mostahpa yalla na ko yalla ak serigne touba faye
Dierediefe serigne touba serigne mountakha mbacké yalla nafi yagg te annd ak weer ci barke rassoullilah sallahou aleyhi wassalam ak serigne Touba amiiiin .
Cheikh Akhmadou Bamba, le serviteur du prophète (psl), a montré sur ce poème son caractère multidimensionnelle et son amour inconditionnel à l'élu de Dieu. Dieureudieuf Serigne Touba
Dieureufe cheikhoul khadim diarrama mame cheikh ibrahima fall serigne mountakha yalla nafi yague lol te wer thi barkep borom touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Sawaye ki douma ame numérom yaine❤️😭😭😭
Serigne Moustapha Seck Yalla nala Serigne Touba bégueul. Koula déglou xolam dafay sédd gouyy. Yalla na say fann gouddou té nga amm wér si BARKÉ Serigne Bamba.
Ça fait pleurer 😭 bilay Serigne touba amoul morom
dieureudieuf Khadimoul Moustafa. yalla na Moustafa Seck am ngueureumal borom khassida yi
Daouda FALL xxgpp8. [
Djereudjeufeti akhmadou bambara
Euskey! Man dé yémouna Serigne Moustapha Seck yalla na batt bi wer barkeh Serigne bi. amine
Rassoulilahi amoul mass... Wayèé srgn Touba kènn leu..... S moustapha seck yalla naleu srgn bi fayal bopam 🙏🙏🙏
Ĺòò
1
¹
amna solo dieuredieuf serigne touba diarama mame cheikhra fall....adouna loumou nekh nekh beug serigne touba ko dakk
Commentaires yi dioy lo nagne ma barki serigne touba serigne Moustapha seck yalna yalla wereul bate borom touba Amoul morom dieureudieufety borom touba❤🙏
THIEY KIMU DON ♥️ KUDUL YALLA SUNU BOROM KHAMOKO DIEUREDIEUFTE SERIGNE TOUBA KHADIMOU RASSOUL ♥️ AMOUL MOROM ♥️🙏
Thiey serigne touba yalna niouko yalla fayal ❤❤🙏🏼❤❤
*_✍️Cëyy serigne touba❤ lepp mome là❤ serigne moustapha seck💓 yalnasa diam yague si barkép serigne saliou❤😢😭😭😭🙏_*
Qui dieu a miséricorde 😭😭😭😭 qui l’a retrouvé
thiey serigne touba😍
Yalla na yalla wérall batbi barke cheikholl khadim
Serigne Moustapha seck yalla na yalla goudal say fanne thibarckee yonentibi Salla lahou halleyhi wa Salam 🙏🙏🙏
Thiey sougnou xol toyna !!!
Serigne moustapha yalla nga fi yague Thi barkep khassidayi......
Mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla mashalla yalla Nala yalla sammm defall la Diam si barke seydina Muhammad psl Dieureudieuf serigne touba ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏
Man dal mouqaddimatt bi boumakay deglou Sama khol dafay toy Ba douma mana tèyè samay😭 yalla na yalla guena wèral baat bi ci barkè xassida yi
Bilahi amna solo Macha Allah dieuredieuf serigne touba
Ndayesan santal yalla nitou aldjana nga machala
Wallaay Akassa
yalla nanga goudou fan man tydiane laa waye serigne touba limou wakh yonentebi reuyna kou sopou yonentebi boko degloo sa khol dina tooy . day yokou thiofel si yonente bi
Tapha Ndiaye yallah nanga guiss yonéntebi yow kou baakh nga yow bokko si gnouy déf yonéntbi gnaari yonénte
Machalla
Macha Allah lou werr nga wakh
Da nga gooré rek
@@papekara6887 amin pape kara ak mboolem djiouliyi
Dieureudieufety serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall lampe ❤❤
Serigne touba amoul morom souma duegue khassida gui damay dioy rek te douma kham loumay dioy lo dieuredieufati mame cheikh ibrahima fall abo ridiallaullahi 💞
macha allah yalla na yalla wéral sa bat thie barké seydina moukhamét amine
aicha gueye
amine
Dieureudieuf serigne touba
santati elhadji fallilou ndakh ap diam sant boromam sasounè dakowar yallana yalla fay keep kouy yeungou thi khassida mbarkep borom touba
barké borom touba yalla na na yalla guena takhawou ningay radiassé khassida yi ler na .
machalah yalna yalla weural bat bi diadieuf mourite
Ki mom rek lay deglou thi diankatou awou
yalla na yalla wérale batte bii nékhe naa looolou si khole serigne touba amoule morome
❤❤❤❤ Dieureudieuf serigne touba amoule morome Sunus waddi Akhemadou Bamba khadyme rasoule serigne Mountakha Mbacke yaguefi Mbacke té weer amineeee loleeeeeee Dieureudieuf xassidayies machalla amenasolo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf Serigne Touba. Serigne Mountakha Mbacke Y'Allah nafi yagg annd ak weer cii Barke Rassoullilah Sallahou Aleyhi Wassalam ak Serigne Touba. Amiiin.
J'aime bien ta pp
@@ndeyefatougueye2502 Ma Shaa Allah. Dieuredieuf and Deweneti.
Dewéneuti à tw oci
Dierediefe serigne touba serigne mountakha mbacké yalla nafi yagg te annd ak weer ci barke rassoullilah sallahou aleyhi wassalam ak serigne Touba amiiiin .
Amine yarabal hallamine
Moustafa moye sangue mbathia medine salalahou aleyhi wa salama
Mashallah limouy diangue sama biir kholbi lay dougou!Yalla na Yalla goudal fannam! té féyalniou CHEIKHUL KHADIM!
Ma challha
Amine yarabi
vraiment cette chanson me pique au cœur S Moustapha Seck que Dieu vous bénie et vous garde contre les mauvaises choses
yallana yalla wééral baaatbi si barcké khassidayi
Meilleure version de Muhaddamat Amdah, de tous les temps
Deuggue piir serigne Papis
,yalna yalla faye
Je confirme ❤
Machallah dieuredieufff boroom touba Cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd ki Aminnnne
pourkoi les gens mettent jaime pas ak lii noumouy douguee si kholou diam gni doyna war .nala birom khassaide fay si bar ke seydouna mouhamed(psl)
Dou ay niit rék gnoy déglou . Niit ak Djiné ak lou yalla sak day deglou . Kén dou serigne touba
Meilleur khassida que j'ai eu a écouter. Je l'ai découvert grâce à mon ami et frère qui est un fervent mouride. Machalla
mashalah amenaa soloo soloo s moustapha seck yala nala yala dèfall tawe fèkh ak taysurr si barkep khadideyui ak mbolème kèpou kouye buèguè khasideyui amineeeee.
Machala serigne Moustapha mala beug ci sama khol lingay diang nhna machala♥
Quand j'écoute ces khassaides , j'ai les larmes aux yeux Serigne Touba Amoul Morom
ndeysan jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef jerejef stouba diarawlak mame cheikh
Dieuredieufety serigne touba maty niang
serigne touba amoul morom
beugue serigne touba rek fonkou serigne bi rek sope serigne bi rek deuguel serigne bi rek ken dou serigne touba dieureu dieuf serigne touba
Yalna yalla goudal fanam nekh na loll
Yalla nalla s.touba teck lokho baa fawou sii barké khasside yi s.moustapha goudeul fane loole yage guide béggeu
Yalna yalla weiral batt bi
Walay ça donne des frissons machallah
akasa Moustapha Seke
ndiague mi âme nasoulo yalla nala Sarigne touba
fayall bopam
lou ame sola laye wakh yalla nala serigne touba fayal bopam
Serigne Touba kiné rk akassa
Dieuredieufete serigne Touba amoul morom te ken dou mom amoul denele serg moustapha Seck yallah na gueram kou Tede ki
Ndayssan diadieuf Sama tourendo yalnala yalla defal diam the barke xassida yi
Dieurdieufty gueum beug.wolou yakar serigme Touba rék lanouka défe adouna ak alaxira yalla n'alla
Borom khassidayi.faye
Mashalla bilahi li dafa séde khole soumakoy déglou tour ay khéwale daf may yombe trope.Yalla naniou serigne touba fayale bopam S Moustapha Seck
Allahou Akbar. Seck goudou fan werr ak werle si barkep Khassida yi.
yalla na la serigne bi fayal bopam
Wallahi li douma si doyal c’est mon enfance 😭yag a beug Serigne Touba ak xassida yi
En l'écoutant j'ai des frissons WALAHI 💯❤️🤍💯👌☝️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalla nagn si tassék ngueremeul Serigne bi🙏
Thiey yalla moukhadimate bi diko déglou fadiar ohhhhh😢😢😢
Yalla nala yalla faye ci barkep xassidayi
machallah ken dou serigne touba sedeu na khol loll.yalla na batt bi werr
Dieureudieuf khadimoul moustapha .se.moustapha SECK yalla na fan wi guoude ak wer
Liii dee bolen si diapoul dinama raye. Serigne moustapha seck yallana yalla faye.
Ahkhamdou'lakh djeureudjeufé xheikhana Ahmadoul khadim... Serigne Moustapha seck yalla na weurrraal batt biii
Akassa. Cheikh Ahmadou Bamba, le Sèrviteur du sceau des Prophetes psl, le Trèsor dAllah swt. Dieuredieuf Serigne Touba
Sante Serigne Touba si mokkale bimouma mokkale lo Moukhaddamaatoule amdaah. Serigne Moustapha SECK Yalnala Yalla faye.. Chaque jour que Dieu fait tu nous accompagnes de par tes si belles prestations.
MachaAllah dou ma di doyal. Quen dou serigne Touba
❤️❤️sante brom bi baniou bolei si khetou RASoulilah teksi andak serign bi
As salamou aleykoum serigne Moustapha yalna borom bi defal la djam weral bate bi,bilahi mouhadimate bi ningako djangué yém nama weur na ba sonou foumay amé son bi,vidéo TH-cam bi rek la télécharger,awma si sago barkep serigne bi❤😭😭😭😭😭😭😭
Je suis tidiane mais douma thie doyal bilaye
Alhamndoulilah bima yala bolé thi ndiabotouk serigne touba amoul morom
Dieuredieuf serigne touba!! Lii kouci bokoul khamouko, sant banou ci bokè
Merci
Serigne Moustapha mo damn rajas birr Senegal Masha’allah
Thieuy Serigne Touba.
Mashallah Serigne Moustapha djangu bi neexna
Dieureudieuf serigne TOUBA KHADIM RASSOUL
Machalah yal na baad bi weer thi barkep khadim Rassoul
Yalla nalla borom touba samm ak bepp dioulite
Dieureudieufati Serigne Touba Serigne Moustapha sec yalana gafu yag té werrr
Non son bii Mounnama ray Billahi ♥️
Moustapha séck aka Meuneu Diang kii Yallah Nako Fii Yallah yagall Lolll Téwérr thi barkèp cheikh Akhmadou Bamba khadimou Rasoull ♥️🙏
akasa s moustapha Seck chante bi amna solo alla nalafi sounou borom yagal te weral la thi barke khasidayi
machala mouride doundal way sans limite barkép khassida yii 👌 serigne Moustapha seck yàlla nala yàlla défal saxadatoul darayni barkép khassida yii 👌 diadief
Machalla li sédna khol trop way
Yalnala yallah fey thi barke borom Touba
Moustapha seck yalla na bat bi weer walakhi kéne Serigne Touba
serigne touba rek ma sante yalla bimasi boke
Sama xol day féss si bôumay dèglou khassayites yi kéne dou borom touba❤
sante yalla nek bam nou défé ay mouride
Walahi ken dou ahmadou yalla moy bour yonet bi di guenn gui mbideff serigne touba di ken mame cheikh di yonn wi
ndaye sane yalna yalla weral batbi mayla wér ak goddo fan nèkh na torop
Yalla na serigne bi faye te weral la masahala
Thiey sama wathia Seringe touba momana binde
arina
Ca va droit au coeur , dieureudieuf borom touba
akasa serigne moustapha seck amna solo barké serigne touba
Tay lama geuneu diokh Aÿ frissons bilahi kou mélni serigne touba dotoul ame
Serign touba amoul mass❤️❤️💊
Fam
Mbacke amoul morome dieureudieuf Serigne Touba
yallana yalla weral baat bi si barkeb serigne touba
machaalah damakoy deglou sama hol day fess bilay yalnala yalla Faye