Allhamdoulilah j ai cherche ce xassida depuis plus de 20 ans. je suis alle a Sandaga mais ils ne me comprenaient pas car je ne pouvais pas recite comme ce genie. ils me donnaient d autres xassidas mais aujourdhui en ce jour saint de ramadan telle est ma surprise de retrouve ce xassida tant cherche sur ma boite youtube. Devinez la stupefaction et l impressionante reaction de mes voisins europeens lorsque j ecoutais sur ma veranda la voix suave et precise qui recitait ce xassida. Mes chers voisins qui ne croient pas en Dieu et qui sont si critiques comme tout bon Suedois venir me demande c est quel poete et moi de repondre fier c est un des milliers poemes de Serigne Touba un musulman du Senegal.... devinez la suite...Sant Yalla si weru korr gui.
DIEREDIEUF SERIGNE TOUBA YALLA NA YALLA YOK L2RAL T2 MOU BOK AK SOUNOU YONENTEBI PSL PALIER SA ALDIANNA T2 YALLA DI2GAL SAMA PAPA AK SAMA MAG AK MOLEME DIOULITOU ADOUNA YOPP
Yalla nayalla def gnom gni guemoul sen xol yi beugue serigne Touba bamou diaral léne gueustou... té gnom gnep moudié toub done ay talibé cheikh Ahmed Bamba
Je vis à l'étranger ms serign Touba dama defare barki cheikh rafall koudoul serigne Touba gnorouma barki cheikh rafall khassida gui daff gno doy mat gnou wetali way JeureJeufé serigne Touba Bamba kepp dong rek mom kessé moma gnore serigne Touba da dadiale lepp Kon may sognate goor yalla yii gnou geuna defarat taxaway yiii teii xam nii serign bi kay ligueyal ko rek mo worrr JeureJeufé Serigne Touba Bamba kepp 💖🖤❤
Yalla nanouko yalla fayal bopam amounou fayam khana diko santé yalla minou khire si ahmadou bamba khadimou Rassoul dieureudieufti seringue Touba diarama Mame cheikh Ibra fall babil mouridine rek ba faw abadane dayimane la alhamdouli lah kéne d'où yalla
Ndayesane. Ça me rappeler mon père. Mom rek ladane deglou yalla sunu borom yesal yeurmande si mom ak bep dioulit Serigne ndongo thiam yalla nala fi sunu borom yagal
Koumay beugue nama ndakh sa dieum dji Mbacké wayé koumay bagne tamite nama bagn ndakh nimaleu beuguee gua fess del sama xol donne Mouride mayou yalla leu xassaïde yi sunu garabe biniouy dieul matin midi soir Mbacké ya gueune si weer gui yaram Serigne saliou protège 🙏🙏🙏
Sen commentaire yi la lire sama yaram bi daaw si ngèn di santé SERIGNE TOUBA ngen ngi khamouniou sax li khassida gui waxx ngènèn ngi batou baye ndongo thiam deleln deff ay frisson ndakh khassida bimou koy boleil. Wayè li yeup SERIGNE TOUBA 😭 SERIGNE TOUBA LA KEN KHAMOUL LOUMOU DONE
Je suis a l'étrange mais je me sens pas seule parce que j'aime ahmadou bamba autant que tout je ne me prive jamais de le remercier si petit à petit je devient un meilleure musulman c'est bien grâce à l'amour que je porte pour lui que dieux nous aide à étre de bon talibés mouride comme mame cheikh ibra baboul mouridini akhmadou bamba reka yelo diadjeuf
JE SUIS UN MOURIDE ,MAIS NE CESSE DE DIRE MERCI SERIGNE TOUBA ,SERIGNE SALIOU MBACKE MON GUIDE SPIRITUAL ME MANQUE ,JE VIS A LETRANGER MAIS LES KHASSIDA ME DIRIGE VERS UN AUTRE MONDE,UNE AUTRE DIMENSION ,.DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA
Serigne Nongo Thiam Yalla na la Yalla faye fi ngua may yobou khamo ko sakh damay deglou tjrs sa diang khassida Matlou bill Chifai Dieureudieuf Serigne Touba souma triste tee ba deglou ko day melna adouna naniou ma may Dieureudieuf Serigne
je vis a letranger ou il est plus facil de devier.Mais Lamour q Jai pour le mouridisme la foie en Serigne Saliou ma beaucoup aider a mieux pratiquer ma religion
Ay way degual li manchallah manchallah manchallah sant serigne touba serigne fallou bou wer baye ndongo diam ci yaw ak tawe fekhe allahouma amine ya rabi ❤❤❤❤❤❤❤❤🙏☝️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Ce khassida me rappelle les matins de Korité ou Tabaski, quand on se préparait pour aller à la mosquée, étant petit avec mon père, yalla nafi yagg té wèr!
En roulant dans la fraîcheur du petit matin, pour un long voyage (De Ottawa a Montreal) , avec Ndongo Thiam en backgroud fait le voyage plus amusant que la destination. MashaAllah, Sa voix spirituel te fait vivre à la fois, l'amour du Prophète PSL et l'admiration de son serviteur Khadimou rassoul !!!
Alhamdoulila ce khassaide m'emporte dans un autre monde bien vrai que je ne le maitrise pas mais g des frissons rien qu'en l'écoutant dieureudieuf Serigne Touba rat💓💓
Je cherchais l'auteur qui a chanté c xassida depuis fors longtemps alhamdoulilah je l'ai eu grâce à Facebook merci Dieu d'avoir çu répondre mes attentes
Merci Serigne Touba. Vous nous avez permis de bien connaitre Allah (SWT), de suivre ses recommandations tout en évitant ses interdits, d'aimer le Prophète Mouhamed (PSL), d'être des Mourides Sadikh.Nous n'avons peur ni ici bas, ni à l'au de là. Vous nous avez mis sur le bon chemin. Dieureudieuf
ça me rappelle beaucoup de choses. Etant très jeune quand je partais à Touba à l'occasion du Magal avec ma mère j'entendais cette belle voix à travers les haut parleurs aux alentours de la grande mosquée.
QUE CE KHASSIDA YA RAHMANOU YA RAHIMOU NOUS ACCOMPAGNE EN CETTE FIN 2020 ET NOUS OUVRE 2021 AK AY KHEWEUL. YALNA NIEEP AAM DJAAM BARKE CHEIKHOUL KHADIMI
Doumasi doyal diko déglou sama khol déy toy😢😢😢 ca me rapelle Mon pere😢mom rek ladan déglou yalla nako yalla yeureum té kharéko Aldiana si barké Cheikhoul khadim
Yalla ne Yalla yessal yermander si sunu wadiour yi delou, niom yi niou guindi wane niou yoone bi tétée niou si yoonou Ahmadoul Khadim sen guiir dounde! Yalla ne leen Yalla yereum te kharer leen firdawsi si barker Cheikhoul Khadim.
Sant Cheikhoul Khadim Dieureudieuf Mbacké. Santé bou weer. Désigne Ndongo Thiam machallah : juste vous écouter est un privilège et vous entendre me fait pleurer motakh begue ci mouridoulahi bima done.
Ndoguo thiam sa voix me rend nostalgique avec des pleurs ma mère me racontait que ses chansons étaient écouter lors des funérailles de mon oncle qui est décédé kan jetai petite de ce fait il me rappelle l’oncle que j’ai pas connu
😭😭😭Mon père qu’Allah l’accueille dans le plus haut des paradis, aimait ❤ bcp cet air de Ndongo Thiam. Quand on voyageait dans sa voiture 🚙, nous l’écoutions durant tout le trajet 🥹🥹🙏🙏
FafafaddfdffafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafaffcfaaaaaaaaaaaaaaFFCXCCCCCCCCCFCCCCCCCgF FXCS GC G G G G GC G GW GC GCCCCGWGGGCSGGGGGGGGFSGFWGGVSFCVFCWSGFFFGFFDGSDDDGSDDDGSDCGSCSDGSDGSGSDDGSDCSDGSDGSGSDGSDGSGSSGDDDDDDDGSGSDDDDGSDGSGSGSDSGGSDDDDDDGSGSFFC X DXX DXD X FEDERER
Allhamdoulilah j ai cherche ce xassida depuis plus de 20 ans. je suis alle a Sandaga mais ils ne me comprenaient pas car je ne pouvais pas recite comme ce genie. ils me donnaient d autres xassidas mais aujourdhui en ce jour saint de ramadan telle est ma surprise de retrouve ce xassida tant cherche sur ma boite youtube. Devinez la stupefaction et l impressionante reaction de mes voisins europeens lorsque j ecoutais sur ma veranda la voix suave et precise qui recitait ce xassida. Mes chers voisins qui ne croient pas en Dieu et qui sont si critiques comme tout bon Suedois venir me demande c est quel poete et moi de repondre fier c est un des milliers poemes de Serigne Touba un musulman du Senegal.... devinez la suite...Sant Yalla si weru korr gui.
DIEREDIEUF SERIGNE TOUBA YALLA NA YALLA YOK L2RAL T2 MOU BOK AK SOUNOU YONENTEBI PSL PALIER SA ALDIANNA T2 YALLA DI2GAL SAMA PAPA AK SAMA MAG AK MOLEME DIOULITOU ADOUNA YOPP
Nounou Sane Hakassa
Euskeuy
Yalla nayalla def gnom gni guemoul sen xol yi beugue serigne Touba bamou diaral léne gueustou... té gnom gnep moudié toub done ay talibé cheikh Ahmed Bamba
Je pense que danko diawalè ak samba Wade.. ndakh depuis 20 ans ngua wakh
Je vis à l'étranger ms serign Touba dama defare barki cheikh rafall koudoul serigne Touba gnorouma barki cheikh rafall khassida gui daff gno doy mat gnou wetali way JeureJeufé serigne Touba Bamba kepp dong rek mom kessé moma gnore serigne Touba da dadiale lepp Kon may sognate goor yalla yii gnou geuna defarat taxaway yiii teii xam nii serign bi kay ligueyal ko rek mo worrr
JeureJeufé Serigne Touba Bamba kepp 💖🖤❤
Ça me rapelle mon pere yalla nako yalla yereume te khareko aljana firdawssi 😭😭😭😭 mouride sadikh lawone
Amine
Amine
Yàlla nako buur yàlla yërëm té xaare ko ci Aldiana you gëna kawee ya ñu mu fa fekk ak ñu ko fa fék
Moi aussi
Allahouma amine 🤲😭
Yalla nanouko yalla fayal bopam amounou fayam khana diko santé yalla minou khire si ahmadou bamba khadimou Rassoul dieureudieufti seringue Touba diarama Mame cheikh Ibra fall babil mouridine rek ba faw abadane dayimane la alhamdouli lah kéne d'où yalla
Ndayesane. Ça me rappeler mon père. Mom rek ladane deglou yalla sunu borom yesal yeurmande si mom ak bep dioulit Serigne ndongo thiam yalla nala fi sunu borom yagal
,اللهم امين
Koumay beugue nama ndakh sa dieum dji Mbacké wayé koumay bagne tamite nama bagn ndakh nimaleu beuguee gua fess del sama xol donne Mouride mayou yalla leu xassaïde yi sunu garabe biniouy dieul matin midi soir Mbacké ya gueune si weer gui yaram Serigne saliou protège 🙏🙏🙏
Ma beugue nguir dieumi Serigne bi té guisouma la Billahi 😭❤
Ndeysane yow mouride sadikh nga
Serigne Ndongo Thiam yalla nga fi yag te wer Barkeh Sokhna Moumi Mbacke
fulbertcharlotte jererje bamba
amine waye🌹
amine waye🌹
Moustaphasey4321@mil.com
Moustaphasey4321@mil.com
khoolle. sédde na ja géne jeuff yalla. naléne. s. Touba faye
Sen commentaire yi la lire sama yaram bi daaw si ngèn di santé SERIGNE TOUBA ngen ngi khamouniou sax li khassida gui waxx ngènèn ngi batou baye ndongo thiam deleln deff ay frisson ndakh khassida bimou koy boleil. Wayè li yeup SERIGNE TOUBA 😭 SERIGNE TOUBA LA KEN KHAMOUL LOUMOU DONE
Je suis a l'étrange mais je me sens pas seule parce que j'aime ahmadou bamba autant que tout je ne me prive jamais de le remercier si petit à petit je devient un meilleure musulman c'est bien grâce à l'amour que je porte pour lui que dieux nous aide à étre de bon talibés mouride comme mame cheikh ibra baboul mouridini akhmadou bamba reka yelo diadjeuf
JE SUIS UN MOURIDE ,MAIS NE CESSE DE DIRE MERCI SERIGNE TOUBA ,SERIGNE SALIOU MBACKE MON GUIDE SPIRITUAL ME MANQUE ,JE VIS A LETRANGER MAIS LES KHASSIDA ME DIRIGE VERS UN AUTRE MONDE,UNE AUTRE DIMENSION ,.DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA
@@saliougroup2638 magasin touba rte
Je suis tidiane mais c'est mon chanteur préféré
2020 li bilahi mo dak adiana ciey AHMADOU yaw reik lagnou am 😭😭😭😭😭❤️
Machallah,
Cette belle chanson me rappelle le Bapteme de mon fils aîné il y’a 25 ans. J’en ai les larmes aux yeux.
Dieuredieufeti 🙏🙏🙏
Pareille pour 26 de cela, qui a coincidè avec kazu Radiap et mon s appelle fallilou , Sans que nous ne Savons pas
machalla très belle voix serigne ndongo thiam

Ken dou serigne Touba
Bégue serigne Touba rek
Geum serigne Touba rek
Fonk serigne Touba rek
Doylo serigne Touba rek
Yakar serigne Touba rek
JeureJeufé Khadim Rassoul ❤🖤💖
Serigne Nongo Thiam Yalla na la Yalla faye fi ngua may yobou khamo ko sakh damay deglou tjrs sa diang khassida Matlou bill Chifai Dieureudieuf Serigne Touba souma triste tee ba deglou ko day melna adouna naniou ma may Dieureudieuf Serigne
je vis a letranger ou il est plus facil de devier.Mais Lamour q Jai pour le mouridisme la foie en Serigne Saliou ma beaucoup aider a mieux pratiquer ma religion
8edvip
J'aime ça me va droit au cœur
NDAYSSANE nekhna LOL BARKÉ SERIGNE SALIOU
MASHAALAH
TCHA KAW REK BARKE SERIGNE SALIOU MBACKE NAJOUL KHADIIM
جرجف
Ndeysane way gor dam rek ci barki serigne Saliou mbacke
ndeyssane yalla na yalla goudeul sene fane kep koufi takhawal serigne touba..... deg deg amoulo morom cheikh ahmandou bamba
AMINE
Diereudieuf Serigne ndogo Thiam yagal te weer
Ay way degual li manchallah manchallah manchallah sant serigne touba serigne fallou bou wer baye ndongo diam ci yaw ak tawe fekhe allahouma amine ya rabi ❤❤❤❤❤❤❤❤🙏☝️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Dieuredieuf Serigne Ndongo Thiam,yalla ngafi yague lool té wer ci barkep Serigne Touba
AMINE
Amine
Dieur dieuf serigne touba sounou yakar teye ak euleuk diarawe raka mame Cheikh ibrahima Fall
Yengni defoul j aime sokhor rek
Machalah doumassi doyal moukou. Nékh n'a looooool .Dieureudieufeti serigne Touba
😭😭😭😭Li nimou may def tcheutttt Serign ndongo yalla nala brom xassidah Fay 😭❤️🙏🏾
Ce khassida me rappelle les matins de Korité ou Tabaski, quand on se préparait pour aller à la mosquée, étant petit avec mon père, yalla nafi yagg té wèr!
Baye ndongo yalla nala serigne touba faye
Thieye Serigne Ndongo baga Keye ndiangue si tante bi en face 🕌 touba fin 2000 dougou si 2001 Yallah na la borom bi fey
Yalla nanou yallah fayal sgn touba khadimou rassoul
Mashallah kén d'où mom😭😭😭😭😭😭😭
Machahalah, Serigne Ndongo Thiam, yalla nafi yague looollllll té were ! Yalla wéral batbi, barké Cheikhoul Khadim !
Amine
Fou sori lamay yobb billahi ❤️
Jerejef Sèrigne Touba rek inchaallah
Baye ndongo thiame yalnafi yague te werrr
Amine inchallah
sante cheihoul khadim rekk ame na solo dieuredieuf serigne ndongo thiam
Louise Diagne yaw beugue nga qassaids dé
Amine
Djeuredjeuf serigne Touba
ALHAMDOULILAH dieureudieufeti Serigne Touba Kou Tédaki diaarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
mor diop pp
Dieuredieufé Serigne touba
En roulant dans la fraîcheur du petit matin, pour un long voyage (De Ottawa a Montreal) , avec Ndongo Thiam en backgroud fait le voyage plus amusant que la destination. MashaAllah, Sa voix spirituel te fait vivre à la fois, l'amour du Prophète PSL et l'admiration de son serviteur Khadimou rassoul !!!
bilaye wakhatiko, sa voix est uniqe et clair
thanks very nice dieureudieuf Serigne Serigne touba
Bbi
Maachaalla
Y
Alhamdoulila ce khassaide m'emporte dans un autre monde bien vrai que je ne le maitrise pas mais g des frissons rien qu'en l'écoutant dieureudieuf Serigne Touba rat💓💓
0
Alhamdoulila
Bilay walay
@@mameantandiaye6080 de
thiey serigne touba kene dou mome
alhamdu lilahi wás salaatu was alaamu â laa sayidina Mohammadine wa salama tasliimane katsiiraa.
Je cherchais l'auteur qui a chanté c xassida depuis fors longtemps alhamdoulilah je l'ai eu grâce à Facebook merci Dieu d'avoir çu répondre mes attentes
Merci Serigne Touba. Vous nous avez permis de bien connaitre Allah (SWT), de suivre ses recommandations tout en évitant ses interdits, d'aimer le Prophète Mouhamed (PSL), d'être des Mourides Sadikh.Nous n'avons peur ni ici bas, ni à l'au de là. Vous nous avez mis sur le bon chemin. Dieureudieuf
AKKAY DEUG DIADIEUF MOURIDE
55t5 il
Jo
Thiey SERIGNE Ndongo Thiam
Dieureudieuf Mame Serigne Touba Yalla na sunu borom fay li nga def ci diné l'islam Amine
Mashaalla s.ndogo thiam. Dieurdieufti s.touba amoul.morom Ken rek la yala.na nu ko.yalla fayal.diam rek ak khewal inshaalla.
Ndaysane ça me rappelle mon grand-père commissaire mbaye fall
ça me rappelle beaucoup de choses. Etant très jeune quand je partais à Touba à l'occasion du Magal avec ma mère j'entendais cette belle voix à travers les haut parleurs aux alentours de la grande mosquée.
Mamoune DIAGNE
❤😢👍
Vv
Billahi ndeyssane
Walay ❤❤❤
Machallah borom touba amoul morom môme rek si Yallah moye qui kei faye
le sauveure de l humaniter cheiikhal khadim
Thanks
Machaallah....Djeuredjeuf Serigne Touba, YALLAH na YALLAH Yock Sayy Lerr ci DARADJAYY SEYDINA MUHAMMAD (SAW) AMIINE ❤❤❤❤❤❤❤
jeurejeuff serigne ndongo yalla nala serigne bi beugg ci yaw*
MODO
U NDIAYE
AMINE
Amin amin amin amin amin amin amin amin amin amin amin amin amin
qui a aimé avant le million de vues?
Une des vrai disciple du prohete mohammad ( SAWS)
Serigne TOUBA dieureudieuf
QUE CE KHASSIDA YA RAHMANOU YA RAHIMOU NOUS ACCOMPAGNE EN CETTE FIN 2020 ET NOUS OUVRE 2021 AK AY KHEWEUL. YALNA NIEEP AAM DJAAM BARKE CHEIKHOUL KHADIMI
MaashAllah
Dieureudjeufeutty Cheikhoul Khadim
Doumasi doyal diko déglou sama khol déy toy😢😢😢 ca me rapelle Mon pere😢mom rek ladan déglou yalla nako yalla yeureum té kharéko Aldiana si barké Cheikhoul khadim
Walahi Li nimou may def mane ak yalla rekka ko xam😭😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️
ahkhamdou lilahi rabil khalamine baga gnoubolek serigne touba
macha allah setna
selna wakha deugue
Yalla ne Yalla yessal yermander si sunu wadiour yi delou, niom yi niou guindi wane niou yoone bi tétée niou si yoonou Ahmadoul Khadim sen guiir dounde! Yalla ne leen Yalla yereum te kharer leen firdawsi si barker Cheikhoul Khadim.
Amine yarabi incha allah
S.Ndongo Thiam doundeul lo doundou dou doye Dieurediefeuty
Ndeyssane Xassida ''Rahya'' Serigne bi wah nassi Seydina Mouhamed PSL louko kéne meussoul wah si adouna barké Mame Cheikh Ibra
dieureudieuf serigne touba khadimou rassoul amoul moroume
Ça me rappelle mon père yalla nako Yalla yeureum 😭😭
Alhamdoulilah alla kouli al
khole séd na dieuredieufé serigne touba 🙏🙏
Dieurdieuf serigne touba khadim rassoul ama morom
Limay def ci xol❤😢
Dieuredieuf Serigne Touba
dieureudjeuf.sering.toubaa.yalna.nou.yagua.dem.touba
Ndiane Sene '
Assalamou..aleykoum...BaYE..ndongo..Thiam..yalla..nafi tagué.té.werre.ak..gnounzk..kouli..dioulite.aminiiine..inchalah..rabi..baye.ndongo..beugue..gui.mala..beugue.té..serigne..touba..takhe..yalla..la..koye. sedelo...BaYE..ndongo...fanegha..seule..si.deukeyi..wokhale..sa..adresse..ma..gneiwe. ziaressila .ÎNCHALAH..Barker..Serigne...toi a.
Ndeyssane macha Allah
Diereudieuf borrom touba serigne ndongo thiam yalla nafi yague lol té andak weer ak diam si barké khassida yi
dieredieuf cheikhoul khadim geum ko rek yakare ko rek doyeloko rek
Louler ga wah
AKHMADOUNA RK FIHA ABADANE ♥️😭🙏
Yalla nagnou ko yalla feyal barkep borom touba
Ndeyssan Serigne Touba séddéneu nigay sedalé xol yii❤..DDCAB❤.
Dieuredieufaty serigne Touba cheikhana ahmadou khadim mbackè balla yalla naniou yalla dolè tass thi sa barkè dieuredieuf dieuredieuf dieuredieuf dieuredieufaty
Thiey adona limoy am ndiage dhe. 😢😢
DIEUREUDIEUF DAME SERIGNE NDONGO THIAM WEER AK WEERLEE
Ça me rappelle le décès de mon chére papa
Jerejeff Borom Touba Mashallah Bamba rekk Mashallah for ever Bamba
Thieye s touba amoule morome
Ciey akhmadou mbackiyou Ken du mom brke cheihra Fall❤️😭👈✍️
Yalna yala goudeul fan yi weral thieuryi doli kheweul yi mayla wer baye ndongo
bay ndongo yall na yalla yagal lafi se bar kep serigne saliou
AMINE
Sant Cheikhoul Khadim Dieureudieuf Mbacké. Santé bou weer. Désigne Ndongo Thiam machallah : juste vous écouter est un privilège et vous entendre me fait pleurer motakh begue ci mouridoulahi bima done.
Bne année 2021 sante yalla dioulli si yonenbi salalahou aleyhi wasalam dieuredieufety Serigne Touba
Dieureudieuf Cheikhoul khadim
Ndoguo thiam sa voix me rend nostalgique avec des pleurs ma mère me racontait que ses chansons étaient écouter lors des funérailles de mon oncle qui est décédé kan jetai petite de ce fait il me rappelle l’oncle que j’ai pas connu
Dieurefeufe Mam serigne Touba Mbacke Amine Mbacke Amine Mbacke Amine Mbacke Amine Mbacke ❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏
Ça me rappel toujours mon pére un fervant mouride yalla na yalla yokou aye lérame
machalla diaradieufati chèikh ahmadou bamba khadimou rassoul ☝🏻🙏🏾🙏🏾
thieuyyy dieureudieufatii Ahmadou Bamba Khadime Rassol
I’m very happy ……..❤❤❤❤
Thanks serigne TOUBA
Machallah sama khôlle sedd na dieureudieufati borom Touba
Diadieuf ridialoulah yalneu kou ted kii motal yéné yii cii barké Mame cheikh ibra Fall👌👌👌💚💚💚
I was looking for this hassaide from Ndongo thanks God
Machalla ndong thiam❤❤
Machaalha yalla na yalla samm yayi aîyi yiwu Aminn
Dieuredieuf mborom touba diarama mame cheikh Ibrahima fall
Dieureudieuféti s touba khamimoul rassoul
Dieuredieuf serigne ndongo Thiam
Ndayesan ba may guéneu aduna douma si doyal ❤️❤️❤️
😭😭😭Mon père qu’Allah l’accueille dans le plus haut des paradis, aimait ❤ bcp cet air de Ndongo Thiam. Quand on voyageait dans sa voiture 🚙, nous l’écoutions durant tout le trajet 🥹🥹🙏🙏
Amine ya rabbal alamine
FafafaddfdffafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafafaffcfaaaaaaaaaaaaaaFFCXCCCCCCCCCFCCCCCCCgF FXCS GC G G G G GC G GW GC GCCCCGWGGGCSGGGGGGGGFSGFWGGVSFCVFCWSGFFFGFFDGSDDDGSDDDGSDCGSCSDGSDGSGSDDGSDCSDGSDGSGSDGSDGSGSSGDDDDDDDGSGSDDDDGSDGSGSGSDSGGSDDDDDDGSGSFFC X DXX DXD X FEDERER
Dieurejeufé Serigne Touba Serigne Saliou Mbacke Yalna Yallah Yokk ay mayyam
Sallalahou AllA Mouhammadine