S’il vous plaît, aimez la vidéo abonnez-vous et partager pour faire partir des personnes qui dénonce fermement cette doctrine qui est aux antipodes de l’esprit humain❤❤❤❤❤
Personnellement je ne croyais pas aux tarékhas je suis qu'un musulman rien de plus. Mais aujourd'hui j'ai raison sur certain personnes et j'attends le future.
Assaâlamu aleykoum warahmatoulah diaguéne dieuf en tout cas li khew instant bi moome warna yée koula mounoul défal intervention ici bas dou barsak la koy deffe wa salam 🙏
En tout cas deh sén kholyi day dagg ba yalmalkhiyam mais jamais vous n'allez creer un conflit entre les tarikhas. Sou appel jotté,tarikha yeupeuy dem yoff,sou magal wala gamou jotté noonou. Yalla naniou yalla samal sounou tarikha yi.
C'est Oustaz Abdoul Karim Ndour A Diourbel. Ils ont attaqué sa demeure, sa voiture et le Billal. Ils ont tenté de mettre le feu 🔥 à la mosquée....d'ailleurs la mosquée est toujours fermée
Nékhoul ba nékhoul mais yén ibadou yii diangui lén watt alkhouran li ngén réré mbir dafa beury téksi di fénal yalla ak yonentam bou tédeu biii Mame Limamoy rassouloulahi kou beug ak kou bagne yalnagnou yalla raye thy gueum baye laye Tourou Al Mahdy mongui thy alkhourane diangui wat lén sén diner
Guis ga yaw ma gui lay watal né bisou yaw mal ki yam seringe touba wallahi dou la meunal dara dou sama wah wahou yalla la boul ma wah nak sama seringe néné wahou yalla mo genne sa seringe
Sama wadji mane Serigne bi daff maa wane yonou siratal moustakhim té lim ma wane dara wouté wouthi ak li Seydina Mohamad salalahou aleyhi wassalam diangalé
@user-dh4zt4nf1m mai yaw yalla mo wah si alhouran yonentibi la la topou lo tè seringe touba mom yalla ak yonentibi la topou mane bo holé fou ma diangé yalla ak yonentibi lenie ma diangal
Votre titre est erroné et c'est pas du bon français. Layenne c'est pas une doctrine, est-ce-que vous connaissez vraiment le sens du mot " doctrine". Vous avez des esprits obtus, des minables de première catégorie. Au lieu de venir connaître la quintessence de la Communauté Ahloulahi vous vous autorisez à critiquer. Niakk xam xam bakhul. Ma yereum nonu Mame Baye Laye aleysalam.
Ay nitou safara nguène Manoulène wakh ba Baye laye dou Seydina Mouhamed Seydina Issa Rohou Laye moy Jèsus Christe Issa ibnou Mariame Senegal dou avance avk c genre de persone sois disant ibadou
S’il vous plaît, aimez la vidéo abonnez-vous et partager pour faire partir des personnes qui dénonce fermement cette doctrine qui est aux antipodes de l’esprit humain❤❤❤❤❤
Machallah allah te récompense ❤❤❤
Mâcha allah Mâcha allah yalla nallenne yalla tahawou wallahi yenne yénay diambarou l'islam dégé Mâcha allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Barakallahou fikoum ❤❤❤
Masha'Allah oustaz alpha ba cheikh younus leral yi Amna solo yallna yallah fay len ❤❤❤❤
SRG Touba moniou wone Yone ba dieum fa yalla khamal nîu kouy mouhamed psl
Yenn nii senn toubaay yii thieuquerrr nonoulaa seen xeel thieuquerr akk sennoum diangue ❤❤❤❤
Yw la sa xell thieukk
Longue vie à vous ❤❤❤❤❤
merci les frer yalla nalen yalla same
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba dieuredieufe oustaz younousse leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna
Sen Ostaz bi waxmoul limouy wax 😂😂😂😂😂
Baraka allah fih younous et alpha machalah❤️🙏🏾
Merci thi léral yi🙏
Outaz liga wakh am na solo tjeye senegal pourtant j'ai toujours douter de ces tarikhat😢 subhanallah
Koubah tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
Assalamouha leykoum machallah ya Oustaz ❤❤❤❤❤❤❤❤
Gracias
Maa yeureum kouné baye laye moy yonéte yalla mouhamed saw
Ma'achallah grace à oustaz oumar sall je sais beaucoup❤❤
MAA SHAA ALLAH AMNA SOLO LOOL ❤❤
Machallah ❤️
انتم دائما تقول الحقيقه التي بعض الشعوب السنغال وموريتانيا من يريد القول الحق فيقول قول الحق من ربك من شاء فليؤمن ومن شاء فليكفر❤
ماشاءالله وجزاكم الله خيرا يا حبيبي ❤❤الفاهيم به
Dégue rèk nguèn di léral ❤
Sénégal téere fertile aux MENSONGES
Walahi deugue rk nguène di wakh Sénégal rèwoum nafékh la
Al Qur'an ak sunnah moy deug ❤
Qu'allah vous aide dans ce combat
Personnellement je ne croyais pas aux tarékhas je suis qu'un musulman rien de plus.
Mais aujourd'hui j'ai raison sur certain personnes et j'attends le future.
ALLAHU AKBAR
Assaâlamu aleykoum warahmatoulah diaguéne dieuf en tout cas li khew instant bi moome warna yée koula mounoul défal intervention ici bas dou barsak la koy deffe wa salam 🙏
En tout cas deh sén kholyi day dagg ba yalmalkhiyam mais jamais vous n'allez creer un conflit entre les tarikhas.
Sou appel jotté,tarikha yeupeuy dem yoff,sou magal wala gamou jotté noonou.
Yalla naniou yalla samal sounou tarikha yi.
Long vie oustaz
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndéyssane lou YALLA déf diam toutina thi dindiko yén ak gni wéddi rignianou seydina MOUHAMED thia Palestine yéna yém thi réer SEYDINA Limamou Lahi rassoulou Lahi S.A.W moy SEYDINA Mouhamadou rassoulou Lahi S.A.W
Lolou la Yalla dogal Wallahi Laye Mamadou gni danio beugue buzz keneu khamou lene😅😅😅
Daccord pourtant vous croyer à la meme personne ❤❤❤
Mais noublier vous pas k BAAY LAYE (psl) weddiwoul benn yoon liguenni waax yeup thii YONNTEBI (psl)❤❤❤
Ndeyssane sona nguéne weddi da metti damaléne yeureum si weddi seydina Limamou PSL ndakh weddi yalla la
😂 ligua waxx tegoko fenn
Baye Niass point 🎉❤
Baye niass moo dakha bokalé yalla sougnou borom
❤❤❤❤❤
😂😂😂Ha ha ha tarikha dey dof lo nit billahi sunnah rek mo wor té moy degue allhmdll
Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
@@AssaneDiop-w5m tarikha moy dji koy lam sette dey takhalé ay dioulite
C'est seulement que certaines personnes ne réfléchissent guère
C'est Oustaz Abdoul Karim Ndour
A Diourbel. Ils ont attaqué sa demeure, sa voiture et le Billal. Ils ont tenté de mettre le feu 🔥 à la mosquée....d'ailleurs la mosquée est toujours fermée
Wakh Ngeen Deug Yonente Bi Mo Moudiou Thi Yonente Yi Lollou Deug Laah
Diangui watal sa diner dangua rér
Le Coran est la seule Vérité
😂😂😂😂😂 ligay wax sakh maîtrisé woko
😂😂😂 ya nekh 😂😂😂
Limamou laye ya khéw té doto xéwi
Baye laye Day fénn dou yonét yalla mouhamed saw
😂😂😂😂 yónnent bou nurul kay
😂😂😂😂😂 est que dou yaye guiss ay djiné
An kone meuna âme gaye moudjé 😂😂😂😂😂😂😂
Sa khôl diekh na nk
Sa bire sakh mougui méti yene daguen nkh😂😂😂😂
Dadial bou gneuwe Senegaal dina beurri mbooloo looool
Nieuwnà ba dem😅😅😅
Nap say yeet baa forokh kay
Sénégalais mo beugeu copier …. Yonnete sah dignikoy copier
😂😂😂
doul wayy
Lébou 😂😂
Djeredief
Nékhoul ba nékhoul mais yén ibadou yii diangui lén watt alkhouran li ngén réré mbir dafa beury téksi di fénal yalla ak yonentam bou tédeu biii
Mame Limamoy rassouloulahi kou beug ak kou bagne yalnagnou yalla raye thy gueum baye laye
Tourou Al Mahdy mongui thy alkhourane diangui wat lén sén diner
Mais diarama ba
Nopal lénn séne bopp moi Ibrahima Khalil mbindéff manouma tée gueume Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul ak Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp
Guis ga yaw ma gui lay watal né bisou yaw mal ki yam seringe touba wallahi dou la meunal dara dou sama wah wahou yalla la boul ma wah nak sama seringe néné wahou yalla mo genne sa seringe
Sama wadji mane Serigne bi daff maa wane yonou siratal moustakhim té lim ma wane dara wouté wouthi ak li Seydina Mohamad salalahou aleyhi wassalam diangalé
@user-dh4zt4nf1m mai yaw yalla mo wah si alhouran yonentibi la la topou lo tè seringe touba mom yalla ak yonentibi la topou mane bo holé fou ma diangé yalla ak yonentibi lenie ma diangal
Saway fi yalla yooni wou fi kén koudoul yonéte yalla mouhamed saw séne tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
La Jalousie tue a petit feu ndeysanne...
Yène am guèn diott nak😂
Amoul bénéne yonéte guinaw yonéte yalla mouhamed saw koukoo wax Day fénn
Bopp bi dal mou doff keuy. yena meuneu fen rek 🤣🤣🤣🤣
Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
Dajjal talibé rék leu Bari Sénégal surtout féne kate yi daniou dème beu défe féne deugueu comme niko dajjal beugué
Alpha nopaloule
Séne tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
Sen dougue khalwa djinne yi lagnouy diokol
Dahwa ba ngui avass bou bakh
Amolén Baye waleu Mame bougnou xam ,séni Mame oubiwougnoufi darra , séni Mame bougnou done wakh histoire Sénégal GNOME dougnousi bokou ndakh kéneu xamoulén 😂 , bayi léne sokhor , sokhor bakhoul, ab deukeu bousén Mame takhawal sakh amoul ndaye sante🤣🤣🤣
Amolén Baye waleu Mame bougnou xam ,séni Mame oubiwougnoufi darra , séni Mame bougnou done wakh histoire Sénégal GNOME dougnousi bokou ndakh kéneu xamoulén 😂 , bayi léne sokhor , sokhor bakhoul, ab deukeu bousén Mame takhawal sakh amoul ndaye sante🤣🤣🤣 damalén yeureume.
Khét yéppa am yonete baye leur Moy Rassoul
Khett yeupa am Yonnent Non yaa meuna fenn
@@fofanabakarydramane7632 khana sa baye Moy doul sa data yaye yaw AK gni wéddi
Lou tah gamouna fene
Kouné moy yonéte yalla mouhamed saw Day fénn fénn you toy xéppou
Soulène tolouwè nonou daguène di wate ni Baye laye dou moy Rassoulou lahi
Sarah ndém xamoko yaw
mai’s Imam amm na yonent you indi woull terer 😮😮
Ay domi kharam nguéne
Bou saga indil xam xam rek
Mais Amna Yonente Yo Khamni Wathié Wougnou Terré
Votre titre est erroné et c'est pas du bon français.
Layenne c'est pas une doctrine, est-ce-que vous connaissez vraiment le sens du mot " doctrine".
Vous avez des esprits obtus, des minables de première catégorie.
Au lieu de venir connaître la quintessence de la Communauté Ahloulahi vous vous autorisez à critiquer.
Niakk xam xam bakhul.
Ma yereum nonu Mame Baye Laye aleysalam.
Ay nitou safara nguène
Manoulène wakh ba Baye laye dou Seydina Mouhamed Seydina Issa Rohou Laye moy Jèsus Christe Issa ibnou Mariame
Senegal dou avance avk c genre de persone sois disant ibadou
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤