Mashalla c’est instructrif quand il y a de l’écoute, merci à toute l’équipe kaadu dînée plus particulièrement à Cheikh alpha, j’apprends bcp de vos vidéos. Mais mon homonyme Ismaila Diallo dafa tangue mom lol. Merci encore une fois
Koulou domou adama adama dayii ndioum. Waw. Sadak ta rasoulouh. Mais rasoulh dou dioum deugleuh. D'accord mais waliou yallah dou dioum deugleu Baye waliou yallah deugeuleu❤ leu
As salamualaikum. Man Gambie laa jogay, mang len di nyan ngen bai gaii nyu pareh sen wahi purr ngen munlena gena japa INN SHAA ALLAH. Lw dut dega c diineh amut proof. Sorlen bayeh gaii nyu wahh INN SHAA ALLAH gaii gena hamneh nekun c dega. Gambie fii sahh gaii barrinen fhi.
Sen soi-disant mandou bobou c que les vrais musulmans ne peuvent pas vous regarder mentir sur notre religion 😢yalla gniou yalla moussal thi tarikhayi 🤲🤲
Tarikha yi gno saboté l islam tardel Sénégal am développement trompé né ñiou jeunesse bi topal sunnah seydina mhmd psl mom la yalla garantie cou ko top dioub
Non royal ki ki yalla yonni té moy yonnente bi psl ndakh bess bo fato ba dou gal la sa bamel ken ndou la ladj sou ñiou mag ñi ya ngui thi erreur sama wadji tarikha yi neckoul lou yalla reconnaître li yalla reconnaître moy sunnah seydina mhmd psl
Salam sama Mbokk Dioulitt Yii, Ma Ngui niann Nioun Dioulitt Yeup Yalla diégal niou souniou Bakar Yi adouna, Mousseul niou Mougueulou Bambel ak Mougueulou Safara
Wakhi Baye bi amul benn dioumté , adouna degg ak niakk degg moo fi Nek. Il faut comprendre qu'il existe d'énormes codes dans le langage des saints. Toubab nénaa l'ami de ton ami est ton ami. Aucun d'entre nous ne pas refuser que Baye était au service de L'islam. Donc l'aimer c'est aimer l'islam ,un chemin vers le paradis.
Ô les croyants !Obeissez à Allah et Obeissez au Messager.Suivez ce qui vous a été descendu venant de votre Seigneur et ne Suivez pas d'autres alliés que Lui,mais vous vous souvenez peu.7/3
Grand bayilen baye Niass svp baye Mossoul wakh si loudoul Lou bakh si yalalh Ak yonenete lingen di deff bakhoul . Delen layè birr lingen dom ni erreur la mais boulen vilipender Baye leer n’a Len ni kifa geuna ndaw molen eup kham kham
Assalamou alaïkum... Barack'Allahou fik. Mais Ismaël dafaay xawa perturbé débat bi. Oustaz alpha moy modéré donc bù kénn duggé laisser le développer avec oustaz alpha. C'mieux Sinon le débat est détourné de son sens et son importance Barack'Allahou
Diangalé bi amna Solo lolou mais dilenn niann rekk Discipline djitou ci lepp, Mou andd ak Deglo ci layy eupp ndieurign, Ma ngui Baalou nieup nakk Yalla naniou Borom bi Bolé diégueul
Boy alpha 😂khagne ngay nopalé guou fall yoe yagui wakh batay kéne ba falé woula niou guéne beugue baye niass té nake ma xam lasi léne lousi kobé carcko baye niass rk doy naniou adouna ak lakhira
Croyance dépourvue de preuve vous dites ???Dites-nous par exemple ns croyons à la résurrection le jugement dernier, ou est la preuve??vs croyez o jugement dernier,c koi notre preuve??ns croyons Aldiana,ou est la preuve???... La foi n'attend pas une preuve,sa engage et concerne juste l'intéresser mes chers.....
J'ai commenté to titre,,ou c dites paroles sans preuve naispa??Donc répondez à mes interpellations rek alors....Naispa ns croyons à tous ck je viens de citer, et où sont les preuves???
Deggg dafa ame solo bala ngay wakh......K oustaz me dise prkoi yalla ndieuka wakh ikhra à mouhamed premier sourate révélé,té ds le coran c fatiha ki vient en premier sourate???Kil me reponde k amena deggg touti ma kham... Niiit bala nga tontou wala commenter les paroles na fekk nga tolo ak mome deggg touti oustaz yangui degg..
Moi je crois en cette voyance. Dieu on peut le voir. Si on se réfère au coran parlant sur l'aveuglement. Allah nous parle de l'aveuglement coeur non des yeux. Qui est ce qui voit ? Comment voir avec le coeur ? Aussi est_il à rappeller, noter votre contradiction monsieur alpha, Comment peux tu dire que tout ce que le prophète est vérité. Et amener le hadith du prophete psl; qui dit: tout être humain se trompe. ? Mouhamed psl n'est-il pas un humain? S'il n'est pas humain qui il est ?
délène deglou ki wakh ni battou djiguen awra leu bimou ko wakhé degglou len ko moguen. Mais nguen di imposer nitt ki mou indi dalil té dollen deglou. Moune nguen bagn koulen accuser té nguen ci live bi doule. Baye Niass doussen morom régler len.
Aimez la vidéo abonnez vous et partagez n’oubliez pas d’activer la cloche de notification pour les prochaines vidéos
Soubhanallah gnie vraiment dagnio rere’ yallah nagniou yallah mouseul thi tarikha 🙏alkhourann Ak sounna ♥️🙏
Machallah imame alpha ya baah ci Sénégal yalna yalla fayla yiwe amine yarabi
Yallah nafi yallah déguéral souna dakal gnou bida ak sirkou thii rewmi
Kham kham nekhna machala mawlana cheikh Ibrahim niass borom faydatoul tidiane.
Que Allah protégés Oustaz Alpha et son équipes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Equipe de quoi?
@@alioudiallo3019 de live évidemment frr tu crois qu’il parle d’une équipe de foot ou quoi?
Ndeyssane amna niou rérrrrrr wayyy Baye Niass mo bahhh❤❤yalla n'agnu yalla fayal Baye ...Baye niass mo bahhhh ❤❤
Cheikh alpha hamo yalla nopil kou hamoul yallah perte gua demlen hamidj yalla nahh s'en dundeu bi am ndieurign❤❤
On ne peut savoir tout donc la fille parle en haut voie tu parles que vérité dans tout ça aida Faye zikr fort
Yalla rek mofi nék yalla ken douko giss nono lol Amoul ok ❤❤
Guiss dégg té wakko moy madou❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashalla c’est instructrif quand il y a de l’écoute, merci à toute l’équipe kaadu dînée plus particulièrement à Cheikh alpha, j’apprends bcp de vos vidéos. Mais mon homonyme Ismaila Diallo dafa tangue mom lol. Merci encore une fois
Mendoulen mogun
@@IKS_Barhama du n’importe quoi vous voyez le mal partout
Yallah na yallah goudal sène fane Machallah wakhtane bi amna solo
masha-Allah ouztaz Alpha Ba Younous, Sokhna Khady et toute l'équipe, vous faites un bon travail masha-Allah ❤❤❤
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna
Koulou domou adama adama dayii ndioum.
Waw.
Sadak ta rasoulouh.
Mais rasoulh dou dioum deugleuh.
D'accord mais waliou yallah dou dioum deugleu
Baye waliou yallah deugeuleu❤ leu
Mouhammad c' est le meilleur Serigne mais à Kaolack les jeunes organisent de cérémonie dange ça ce n' est pas islam
Qui aime baye niass suivra les enseignements du prophète Mohamed (PSL). Alors sui l'a vu et aimé ira au paradis.
Masha'Allah oustaz Alpha ba leral yi Amna solo yallna yallah fai Len
Merci beaucoup oustaz alpha ba
Walahi damalen yeureum😂😂😂bilahii yeureum nalen enplus ligueini wah ay ree lamay def nena thi yonente psl thi yalla kay 😂😂😂yeineu beugolenn yonente bi psl gueumolenn yalla😂😂😂😂 mntah damalen yeureum walahiii
Nooo! Senegal dinee bu lerr problem la tofu, Baye len sen serigne si te topu all quran ak sunnah.
Billahi alquran ak suna rek moy deug
Dafa lére wallahi
As salamualaikum. Man Gambie laa jogay, mang len di nyan ngen bai gaii nyu pareh sen wahi purr ngen munlena gena japa INN SHAA ALLAH. Lw dut dega c diineh amut proof. Sorlen bayeh gaii nyu wahh INN SHAA ALLAH gaii gena hamneh nekun c dega. Gambie fii sahh gaii barrinen fhi.
baye niass sunu mrom la kéy ndakh mindéf la yallâh modoul mrom ndakh brom leu allâhou akbar
Ki kay d'où ouztaz comédien leu😂😂😂😂
baye niass meunoko beug té beuggo yonintibi té kou beug yonnintibi dougg aldiana '' sallal lahou alla mou mouhamad❤
Sen soi-disant mandou bobou c que les vrais musulmans ne peuvent pas vous regarder mentir sur notre religion 😢yalla gniou yalla moussal thi tarikhayi 🤲🤲
Amine amine amine ma sœur ❤❤❤
Yala naniou yla fayal baye niasse 😢
😢😢😢amo lene kham kham saga rek ak khass té moy seni pass pass ak menaces allhur an ak sunna yonnente psl moy degue
Ah yala naniou yala sopi kon
Tarikha yi gno saboté l islam tardel Sénégal am développement trompé né ñiou jeunesse bi topal sunnah seydina mhmd psl mom la yalla garantie cou ko top dioub
@@mamadousy6312 man dh niom lay Roy sonou mag niou bakh ngi
Non royal ki ki yalla yonni té moy yonnente bi psl ndakh bess bo fato ba dou gal la sa bamel ken ndou la ladj sou ñiou mag ñi ya ngui thi erreur sama wadji tarikha yi neckoul lou yalla reconnaître li yalla reconnaître moy sunnah seydina mhmd psl
Souna sikaw❤❤❤
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك أخي الكريم الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ماشاء الله ❤❤❤
Machallah yalla naléne yalla dolli yiiw ak soutoureu
Waw délene deglou Walahi khamo lene dara
Alpha BA ,si tu invite une il faut la donne du temp il va repondre ,apres tu repose un autore question ,parce que il ya des persone qui ecoute
MachaAllah oustaz alpha
Salam sama Mbokk Dioulitt Yii, Ma Ngui niann Nioun Dioulitt Yeup Yalla diégal niou souniou Bakar Yi adouna, Mousseul niou Mougueulou Bambel ak Mougueulou Safara
Wakhi Baye bi amul benn dioumté , adouna degg ak niakk degg moo fi Nek. Il faut comprendre qu'il existe d'énormes codes dans le langage des saints. Toubab nénaa l'ami de ton ami est ton ami. Aucun d'entre nous ne pas refuser que Baye était au service de L'islam. Donc l'aimer c'est aimer l'islam ,un chemin vers le paradis.
Diné amoul code
Ya ouztaz mangui laye nouyou dila ziar yangui guidi gagni té mane guidi ngama
Macha Allah
والله ماشاءالله تبارك فيكم
Il a raison yéne lane ngueen kham si (مقام إبراهيم)
Ô les croyants !Obeissez à Allah et Obeissez au Messager.Suivez ce qui vous a été descendu venant de votre Seigneur et ne Suivez pas d'autres alliés que Lui,mais vous vous souvenez peu.7/3
Walahi warouwoun Sante njie
❤ machallah ya oustaz Alpha ❤️❤️
Mashaa Allah..❤❤❤you for the fact that you people are saying..let returns to quran and sunna..drama's r too much in the deen..
Grand bayilen baye Niass svp baye Mossoul wakh si loudoul Lou bakh si yalalh Ak yonenete lingen di deff bakhoul . Delen layè birr lingen dom ni erreur la mais boulen vilipender Baye leer n’a Len ni kifa geuna ndaw molen eup kham kham
Masahallah ouztass alpha
❤❤❤❤assalamoualeykoum
😂😂😂😂😂 soubhal lahh Raye nama néna mane guéne ma wathié ..
qu'Allah vous récompense pourtant mane Di séne bokk yaguena dégue lolou
Nioune Baye niass rk ❤🎉🙏
Nioune yalla sougnou borom reck
Assalamou alaïkum... Barack'Allahou fik.
Mais Ismaël dafaay xawa perturbé débat bi. Oustaz alpha moy modéré donc bù kénn duggé laisser le développer avec oustaz alpha. C'mieux Sinon le débat est détourné de son sens et son importance
Barack'Allahou
Manchallah manchallah
Bravo youssou. Tu as su te défendre. Cette fois ci Alfa a perdu la bataille
Sunnah nekhna
Assalamualaikum machallah alpha yalla Nanou yalla sahal sii suna mais batou jiguéne dankoy téré mouy diageu alkhouran si kaw
Baye nias dou séné morome
debat bi n'est pas équilibré j'aurais préféré que se soit Alpha et un niassenne.
niou wakhanté deug les autres doivent aussi attendre leurs tours
Diangalé bi amna Solo lolou mais dilenn niann rekk Discipline djitou ci lepp, Mou andd ak Deglo ci layy eupp ndieurign, Ma ngui Baalou nieup nakk Yalla naniou Borom bi Bolé diégueul
L'islam mandou amou fa degeu bii leniouy wakh falouss demal tok
Salam alpha sonal ga dof si nitt yi d 😂😂😂😂😂😂😂😂ñiy nitt lañiou gém
Ouztaz Parle des castes au Senegal
LI NGENI WAX DU DEUG SI YEEN NDAX NEKO LEN SENEGAL BA PARER DI NEBETU RK SURTU KU JIGEEN KI AMOLEN BEN RESPECT SI NITT GNI
Niake cible ak objectif wessouwoul koune achhadou an lahilahailala wachadou anamouhamadarasouloulah ngay weur aye ndioumbtem. Ibadou bou nek tidiane wala tidiane bou nek ibadou islam niakoussi pertoussi.bagnou geume yalla gnoune gneup silagnou ame tawfekh.
Bo gueumoul tarikha sa affaire leu nous sommes de nos tarikhas.Nguir yalla laisse nous tranquillement.
Alpha amo kham kham 😃😃bilahi Daga diang rek mais kham kham outti ko tè bagnia reuy
Hayakoumou Lahou wa bayààkum barakalahou feekoum
Gni gno RER Sénégal d'où dem ay dof kessé
😅😅Akhlou mbirty mbirty de léne deglou nitt yii
Liguey bi rafetna waay faw sa gaayi ñu wañi wérenté bi té ñuy baayi invité yi di wax séén xalaat
Bayilénne duuuuul yaye Aïcha da done binde mais dawoul diangal goor
Alpha ba you must leave baye Niass alone
Baye niass douca morome demal ngua diangui tu fais de l intoxe khamo dara
Yalla wathiewoul ahlou sunna nitt la wathié ima dioulit aw ima yefeur
Alpha, laisse les parler. C'est ça le " sel " de l'émission. Après, tu conclus, en mettant sur la table, ce qu'un dit le coran et les hadiths.
Longue vie a vous ❤ ya oustaz ❤ ❤ Ba
Ya Ismail thank you so much
إعدلو خير من تقوى ...mandou mogeun ragal yalla
Boy alpha 😂khagne ngay nopalé guou fall yoe yagui wakh batay kéne ba falé woula niou guéne beugue baye niass té nake ma xam lasi léne lousi kobé carcko baye niass rk doy naniou adouna ak lakhira
😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤
Al pha ba kou rew la bilaye
Alpha Ki do fi wakh dara bayi ko mo dem
❤❤❤❤❤❤
Ndeysane li rafete dou bagna oute dou oute tamite. Li yeupe thiofel bou nite di ame si nite moko geune.insaniyatou mo djitou leep
Alxouran ak sounnah kasé moo meuneu défar Sénégal
Ibreu niasse deh ay tokhidoni rek lay wakh.
Alpha khamo dara demal diangui gani innawaliyilah neckoul ci alkhouran yameun fen sourate Anfal aya 196 ان ليي الله الذي نزل الكتاب وهو يتول الصالحين
Teye waxtaan bi nèex na, wayé jambar yi faut que ñu bayi interrompre participants yi.
Salam mbok yi Loutah dou ngou dème topou alxouràne AK Sounnah rek kassé am diamou bou baah wallahi
Youssouf mi day diakhasé yeup way haaaaa
Alfa Nay andak dal AK dégulo couy wakh nga bayico mou wakh bou naré Bari wakh nga teuth microm wakhco mou dal comsa gnoune gnou comprends
Lathe pour sabôté wla pour khame dingatt baxoule nagnoule makk ngi doulén wangi dara li soxor la
Il faut juste éviter de la faire paler sur le plateau elle peut écouter ou bien répondre par message .
Salam diadieuf
DEUG rek moy moudiou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Croyance dépourvue de preuve vous dites ???Dites-nous par exemple ns croyons à la résurrection le jugement dernier, ou est la preuve??vs croyez o jugement dernier,c koi notre preuve??ns croyons Aldiana,ou est la preuve???...
La foi n'attend pas une preuve,sa engage et concerne juste l'intéresser mes chers.....
Pourquoi ne pas se concentrer sur l’essentiel du débat appeler Daoud, divertir Soug des choses que pouvons pas de malentendu
J'ai commenté to titre,,ou c dites paroles sans preuve naispa??Donc répondez à mes interpellations rek alors....Naispa ns croyons à tous ck je viens de citer, et où sont les preuves???
Deggg dafa ame solo bala ngay wakh......K oustaz me dise prkoi yalla ndieuka wakh ikhra à mouhamed premier sourate révélé,té ds le coran c fatiha ki vient en premier sourate???Kil me reponde k amena deggg touti ma kham...
Niiit bala nga tontou wala commenter les paroles na fekk nga tolo ak mome deggg touti oustaz yangui degg..
Lii mom dou dou wakh boulen gnou sonal Mohamed psl diigg léwoul niouy diangualé nii
Quels remèdes apportés aux maux de ces sofiankés enkoûtés ? Si Khuran &Sunnah ne leur viennent en aide , quelle effroyable destination
Assalamouha leykoum
Beneen saï saï migui ni Boy Alpha domii Omar sall dji mane damay sant yalla am xol bou fèkh ci dilen deglou 😂 souma paré dislike ta rombou
Ngom lén yallah Ak yonente rek
Moi je crois en cette voyance. Dieu on peut le voir.
Si on se réfère au coran parlant sur l'aveuglement.
Allah nous parle de l'aveuglement coeur non des yeux.
Qui est ce qui voit ?
Comment voir avec le coeur ?
Aussi est_il à rappeller, noter votre contradiction monsieur alpha, Comment peux tu dire que tout ce que le prophète est vérité. Et amener le hadith du prophete psl; qui dit: tout être humain se trompe. ? Mouhamed psl n'est-il pas un humain? S'il n'est pas humain qui il est ?
Nittou charia dafa yaggeu khekh nittou haqiqa. Wayye c la face d'une seule pièce de monnaie.