Thièrè mboum moy sunu plat préfère nioun al pular yi mais dou am nètètou ak guethiakh machala dèloguama Senegal
5 ปีที่แล้ว +2
Kyra Kyra ohhh Masha Allah AlhamdulilAh man tamite sa ma yaye hal Pular Masha Allah mais mom recette tam daf thi done deff netatou kethiakh bi mane mako thi def mais c’est trop bon merci ma chérie 😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪💪💪forza Mon Senegal thanks to remember us our Lebou's village Yoff ngor ouakam my grand father was making field mboum Greenleaf thanks mummy marietou to this goodness God bless you
Mane dal beugeu na li Mane kerok rek Mr mogui may commencé thiéré mboume li môme wohou bou dadié ak guestou la macha Allah yalla nala yalla fay bayi lafi basay seut bi def comme ni gua dilen guiss
Oh toureundo tey yobou ngama fou Sori ndeysann mon père adorait ce plat.. lathiri était haako j’adore avec tous les youbou yaba dedans love u so much..
Tay kharouma sakh ba setane ba pare di commente ndakh sama khel demna sisama mame ak thiere yalla nako yalla yereum Machalah moma yakh si thiere mercie ta maretou
I remember when I discovered her channel last Ramadan, she did not even have 1k subbies, now she is over 80k... Walahi, geum lingua done rek mo am solo... keep up the authentic, instructive and genuine work. Machallah
5 ปีที่แล้ว +2
Mame H. Ohhhhh Masha Allah merci wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
yagui sagal djék bou ndaw bi dal nga khamni cahiers yi rek lagnou talone wayé ak yaw rek amoul roubé dagnouy assuré thi cuisine bi merci doundal wéral moutial
Salam tata. Mane daleuh contane cii yow. Je suis une jeune mariée nekk France avec mon mari. Je sais cuisiner mais daleuh je me perfectionne tjrs grâce à vos vidéos. En plus sa joie de vivre rekk meune naa nekhal sa togg. J'aimerais bien avoir votre contact si possible.
Sama niane nangou neuuuuuuu Lokho yi free neu 😚😚🤗🤗🤗
5 ปีที่แล้ว +1
aissatou seydi yeahhh AlhamdulilAh merci wayy mais man ngui dianga appareil Insha Allah plus de patience rekk ma metrisè ko Insha Allah Dina gnou qualités vidéos you bakh merci 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tata marietou ndao kounda loo dound doypul ! Je suis une passionnee et je cuisine à peu près comme mère Diop en privilégiant la vapeur et c'est ça ton originalité, la cuisine est un vrai art ça on combiné plusieurs ingrédients, en disant ces ingrédients, on exprimé son goût don c une vraie expression artistique. De plus cuisiner demande une vraie concentration, en tout cas vous avez rapproché dans les foyers ce qui était éloigné, facilité ce qui était fifficile pour certaines femmes et apporté la lumière dans les foyers, vous avez un vocabulaire sympathique donc bravoo, tacqnalla xaritt bafaw mashallah ngay nourou batt sama cousine boutoud saly boo, hug kisses depuis Tivaouane, seynabou gaye toure
Sama papa deysane Yalla nako yalla yeureum aka beuguone mboum machalaa yalla na loko bi wer
Thièrè mboum moy sunu plat préfère nioun al pular yi mais dou am nètètou ak guethiakh machala dèloguama Senegal
Kyra Kyra ohhh Masha Allah AlhamdulilAh man tamite sa ma yaye hal Pular Masha Allah mais mom recette tam daf thi done deff netatou kethiakh bi mane mako thi def mais c’est trop bon merci ma chérie 😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
Saveurs Planétaires machala k firdawsi soit sa demeure éternelle
Kyra Kyra ohhh Ameen way ma Cherie 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘😘❤️❤️❤️
A hali gonga ko lathiré halo☺️
@@natyba4923 mashallah latchirri è hakko ina wèli 👌👌🤩🤩
goundouss goudoussi ak youbou yabayie qui Dina ma Reyy rek😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Ayy thieré mboum mako beug bossi néwon touy kani khégn rekk mou goundouss goudoussi😋😋
Amo morom sa tog rek zéro faute té daga bari PUNCH machallah ❤❤❤
Machaallah nékhna ba paré li rek saf sap ma beugue thiere mboum
Youyou yaba momay ray 🤣🤣🤣🤣🤣🤣 merci pour cette beau et bon plat
Yalnala yallah may jam si barkep wérou koor gui tata mariétou
Ameen waay
Thiere mboum in the house MachaAllah tata marietou
MashaAllah ❤❤❤ j'adore
Tata mane damala beugu rék na sa diam yagu♥️machallah et merci beaucoup way
🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪💪💪forza Mon Senegal thanks to remember us our Lebou's village Yoff ngor ouakam my grand father was making field mboum Greenleaf thanks mummy marietou to this goodness God bless you
Moi j'ai grandi à Thies donc tieré mboum c'était au moins une fois par semaine. Merci pour la recette de 👍👍👍
Ay bou amone gnébé danga gueneu nekh eupp vitamine aussi
Thiéré araw bou didji rek dara fayouko fo faté walowalo bi nak 😄😄😄😄😍😍😍merci love you
Togou rek ngay def , goudeul fane waye
Mane dal beugeu na li Mane kerok rek Mr mogui may commencé thiéré mboume li môme wohou bou dadié ak guestou la macha Allah yalla nala yalla fay bayi lafi basay seut bi def comme ni gua dilen guiss
Mann reull bi ak touy bi momay dadjjj 🔥🔥🔥
Oh toureundo tey yobou ngama fou Sori ndeysann mon père adorait ce plat.. lathiri était haako j’adore avec tous les youbou yaba dedans love u so much..
C'est mon plat préféré je le prépare régulièrement .macha Allah c'est bien fait et bon appétit.
Tay kharouma sakh ba setane ba pare di commente ndakh sama khel demna sisama mame ak thiere yalla nako yalla yereum Machalah moma yakh si thiere mercie ta maretou
mbacke fall Ameen wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Saama plat préféré 😍😍😍😘
Magui si thiéré mboum mi machalah
Humm tata mariétou fii teuleu noyna j'adore ce plat merci bpc
Ana Saloum Saloum yi
Thiey sama thiere mogui ni rere ak deki mosi ay dieuredieuf tata marietou
Machallah nekhna té niamoumako
I remember when I discovered her channel last Ramadan, she did not even have 1k subbies, now she is over 80k... Walahi, geum lingua done rek mo am solo... keep up the authentic, instructive and genuine work. Machallah
Mame H. Ohhhhh Masha Allah merci wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Machallah legui On est 237K ❤️ 🇸🇳
Machalla le meilleur reste a venir Diam rek ngay am
Sow Ndeye codou 😘😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machala wayé bossi sani wone niébé toth fi
Wawa mboum dénioukoy nététou kaw.tata mariétou mala souper.😍😍😍😘
Machalla Amatina solo MARIATOU DIEUREDIEUF 👍👍👍♥😘
No tata réleuh AK youbou Yaba momay danél dagua dégu j t,ator
yagui sagal djék bou ndaw bi dal nga khamni cahiers yi rek lagnou talone wayé ak yaw rek amoul roubé dagnouy assuré thi cuisine bi merci doundal wéral moutial
Tata liguaye togue rek la bougou machallah bamay khaler lamako sama yaye diangal
Ma Sha Allah😘
Ma Sha Allah☺
Li nekhna😄
Merci encore.
Machaallah nexna. Tata mane yekal nako sama yaye kou beugue mboumla
Mashalla Tata nekhna werrrna. Merci encore.
Marietou ramadan Moubarak longue vie santé de fer machala laftiatt merci Merci
Tata mariètou damala beugeu rèk tè yalla takh yalla nala dèfal diam si barke mouhamed
Merci tata niko si toyyo ma sah allah thiere ak korgui
Machalla marietou que du bonheur pour toi
hummmm mashaallah nekhna yakkal nassi sama bop
Salam tata.
Mane daleuh contane cii yow. Je suis une jeune mariée nekk France avec mon mari. Je sais cuisiner mais daleuh je me perfectionne tjrs grâce à vos vidéos. En plus sa joie de vivre rekk meune naa nekhal sa togg.
J'aimerais bien avoir votre contact si possible.
Thiérè mboum aka maka beugue.merci encore tata😘😘😘
Machalla machalla thier moubm 10/10
Wawaw mboum day ame netetou
Neko reeul ak touyye... signifie..paaffff◉‿◉。◕‿◕。
Saloum Saloum pir netetou ak thiere mboum
Machalla sa donne envie
Primo moy sama anti stresse billay ya. Geuune yalna nga goude fane bi thièrè sama wal tata
Khady Thiongane Ameen 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘🍽🍽🍽 ok
Diam rek ngay am sama face may khady mou serigne fallou
Vive le Bassi malien
Ndessane aka ma beug there mboum, merci Tata,on peut prendre epinar a la place de moringa
F.ba Ba no ma chérie c’est les feuilles de SAP SAP oubien des choux coupée en petit morceau
Mboum kay kéthiakh nétatou ak guédji moko takha diokk. Machala
Merci pour cette délicieuse recette tata marietou yalla nga gude fane thi barké yonentbi te sa yaye yalla nako sougnou borom diegal té kharéko aldiana
Amine ya Rabi 🙏
You are definitely good woman you help us so much really may Allah bless you ameen
Assalamou alaikoum maman thiaré mboum Day ame niébé
Waaleykum salaam ma chérie balma mangui sogua guiss message non thiere Mboum dou am gnièbè merci
Maman je t'adore
Je suis saloum saloum pir
Mer yadegueuh nena khorim bi dioufouwalè
Merci bcp Tata mes lane moyyi mooringa
Feuilles de mbouum
Sama niane nangou neuuuuuuu
Lokho yi free neu 😚😚🤗🤗🤗
aissatou seydi yeahhh AlhamdulilAh merci wayy mais man ngui dianga appareil Insha Allah plus de patience rekk ma metrisè ko Insha Allah Dina gnou qualités vidéos you bakh merci 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machala Sama tata Saloum saloum la me anna niebebi
Manchalha beuge nala trop
Tata nekh nga ma sa khettou language je t aime for tei amna solo
Machalla Tata thiėrė bi nekhna daal
Mummy love thx u ❤️ nonou la beuguè thièrè mboum mais je savais pas la recette ❤️ j’ai une question dou ame ail poivre piment ect... ?
Machalah maman contane na
Très appétissant merci
J aime j aime j aime
Tata marietou ndao kounda loo dound doypul ! Je suis une passionnee et je cuisine à peu près comme mère Diop en privilégiant la vapeur et c'est ça ton originalité, la cuisine est un vrai art ça on combiné plusieurs ingrédients, en disant ces ingrédients, on exprimé son goût don c une vraie expression artistique. De plus cuisiner demande une vraie concentration, en tout cas vous avez rapproché dans les foyers ce qui était éloigné, facilité ce qui était fifficile pour certaines femmes et apporté la lumière dans les foyers, vous avez un vocabulaire sympathique donc bravoo, tacqnalla xaritt bafaw mashallah ngay nourou batt sama cousine boutoud saly boo, hug kisses depuis Tivaouane, seynabou gaye toure
Merci tata mariétou yalna sa diam yagu
lady dada Ameen
Vrai togaleuse machallah .Mai mboum bi mom fane lane ko meuna amé. Super market wala
Machallah yalna yalla barkél 😍
Mansha Allah tata diadieuf
Eupeuneu thiéré mboum rek
Thanks Tata Marietou darling 😍😍😍😘😘😘 chéé bien machaAllah 😁😁😁
So funny!! Bokk si Thiow li Kay
Machallah maman 😍😘
C bien que vous ayez une caméra maintenant. Mais j'aimerai bien voir votre visage borom bismililakhi et man sha Allah
Dèmale si page Facebook photome migui fofou
Merci beaucoup
Machala handé ko lathirè hakko
😋 ❤️
Aissata Ndg lathirè haako ina wèli machallah
Maimouna Wollahi Machala handé kay tata Marietou routima fouta ❤️
Non tata ak tathio bi 😂😂😂
Li nèkhna tamite Macha'Allah
Bakh bakhi gnak diommmm😄😄😄😄
Waw waw waw waw waw waw waw waw waw waw waw 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙌🙌🙌🙌🙌🙌
Mahchahala thiere mboum lagnou wakh dal
👍nekh na masha Allah
Niaff très bien fait
Machallah. Pouvez-vous rajouter la liste des ingrédients sur la barre d' info svp ?
Ahh lou nex
Merci tata
Nioune bobou la niou kham bi ame nététou ak guedj tambadiang
Tata mboumou djen la beugue
Délou tiossane ndank ak maman mariétou dara Fayoul lii
Bilahi jtaim sa yo wakhé di retane demay contane
Déllo nga ma Saloum Tata 😃 🙏🙏🙏
Machallah tata marietou Yalna lokho bi werr j'apprends Bcp via tes vidéos merci beaucoup
Marietou mangok nak loolou laa kham mboum ak netetou maachaa Allah nekhna
Salam salam tata marietou le mélange du choux et des feuilles de moringa c hyper bon pour la sauce mboum
Machahala dogg rekk guaye deff
Ak mane sama yaye daf may wakh def djin netetou mai thiere mboum rek aka nekh ta bari vitamine
You Machalah
Tata sa thiare bakhna man dal douma magué né yaw la beugua mel
Macha Allah rekk
Mash Allah et bonne continuation
Assalamou Aleikoum Marietou toguatigua Macha Allah c une bonne idée la poudre a la fin. Qu Allah te préserve la sœur . Aïd Moubarak
Fatou Samb Waaleykum salaam wa rahmatulah my sister Ameen wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘