J'ai jamais commenté sur les réseaux sociaux mais j'arrive plus à supporter les insultes surtout venant des Dames wa King production série bi nekhneu trop mais évitez les insultes svp
Sen série bii nekhna amna sens wayé saga yiii tamite meune nassi niak parck aye khalé daniou koye sétane sinon félicitation à tte l'équipe et bnne continuation
J'ai toujours les larmes aux yeux quand je regarde ce série c'est très la manière dont la majeure partie des orphelins vivent dans leur propre maison avec leur propre parent c'est très triste
OH VRAIMENT SÉRIE BI YEUP AYE DES VRAIS PROS ACTEURS ET ACTRICES MAIS SAMA ACTRICE PRÉFÉRÉE LA GUISAGOUL NAK MO SIYE YAYOU XALÉ BI GUANIOU NDEYSANN 😭😭😍❤️
Bouma nékone pape Moussa dina wane sama tanta foula AK faida bou dou gnimé wx AK mane yéne yi teksi protège sama rack kendouko sonale mai ki bonna waay🙏
Djirime Tous Les Jours 11Heures
Pour une offre de visibilité : 77 899 90 75.
Abonnez vous !! et activer la cloche ♥️
Série bi nekhna trpp
Mais ani Coumba diegou lamset
Nice ❤❤❤
J'ai jamais commenté sur les réseaux sociaux mais j'arrive plus à supporter les insultes surtout venant des Dames wa King production série bi nekhneu trop mais évitez les insultes svp
💞💞💞💞💞♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Amine
On réclame le bonheur de papa Moussa et bb Amina ❤️😥 kou d'accord lal ❤️👈❤️
Pape moussa wayyyyyy😂😂😂😂😂😂😂😂mere ana 😂😂😂 cou contane si papa moussa tay😄
Bilaye DEUG ga mahe dé
Si tu tombe sur cette commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends. ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️
Amine inchallah 🙏
Sama yaye yalla nako yalla yeuruem si berkep Serigne saliou mbacke Amine 🤲🤲😭😭
Amine😭😭😭😭
Amiin wy
amine yarabi
Amine
Yangui feep🤣🤣🤣
Kou beugu am dom toudè seydina Mohamed lalal j'aim ❤️🥰💍
Salalahou aléyhi wa salam 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Aminé way🤲🤲🤲🤲🤲
@@khadymboup42 merci beaucoup ❤️🥰
@@aidadiouf5085 merci beaucoup ❤️🥰
❤️😍💟❤️❤️💖💔❣️💔
Kou guem ni diga am dom toudé co seydina mouhamed lalal j’aime ❤
Amine
Vraiment c'est la série dont tous les acteurs me plaisent ❤❤
Kou beugeu serigne touba lalal j’aime
Amoul morom wallahi MBAcké balla yalla nako yalla doli Ay lérr amine yarabi 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲
@@aidadiouf5085 bilakhii amoul morom
Alhamdoulilah on réclame le bonheur de Amina et de pape Moussa 🙏❤😘
La façon dont j'ai sauté sur l'épisode 😂
Franchement j’arrive pas arrêter de rire mere beugue nala 🤣🤣🤣
Le bonheur de papa Moussa et bébé Amina
kou gême ni bis dina gneuw gua âme dôme bou goor guâ toudé kô séydina mouhamed rék l'alal j'aime
Enfin Papa Moussa se révolte 😂😂😂😂baxna si mere douleuse bi😂😂
Khana amoul episode 6
okvfascoiupm😇😅😅😅😅
Dama rétane ba sonou😂
Wouyyyy Pape Moussa ak mère bi j’en peux plus 😂😂😂😂😂😂
J’ai les larmes au yeux à chaque que je regarde ce film on dirait mon histoire 😢
Wallah la série ne me laisse pas indifférent 😢
Miss elle joue très bien son rôle 🤣
Wahatiko
On réclame le bonheur de papa Moussa et bb Amina ❤️🥰✨💖
Miss est joue bien sont rôle ❤️❤️🥰🥰 très importante ❤️✨
Je reclamme le bonheur des enfants 🥺❤
Yaw mi di setane série yalla gua teki ba teral say niari wadiour ❤
Amine nioune nieup
Amine waye yalna yalla nakou niane❤😅
Amine
Wouyyyy papa Moussa tothie nafi 🤣🤣🤣🤣❤️❤️❤️
Ayy wayy serie bi Nékhna tay😂❤❤
yalla na yalla samm djirime yepp
Amine yarabi 🤲
On aime et on commence à être accro... bonne continuation à toute l'équipe 🥰
Théâtre bi limou gâte metinama 😂😂😂😂
Enfin papa moussa se révolte niaf li mo bakh si mère bilay kiya assure bien son rôle vraiment chapeau à elle bilay 🥰
Yalla nanou sa borom défal djam niou sakh dakk ak soutoura ba sounouyy wa diourre fékk sounouyy ndiarinie ❤❤❤❤
Serie nehna trop vraiment amna gnioy doundou li ndeyesane 😢😢
je t’adore papa moussa ❤❤❤❤❤😂😂😂
Parrutoargmscei
Parriteorrg
Mère bi moy vrai comédienne 😂
😂😂😂😂
bilahi yawe 😂😂😂😂😂😂😂 ba sonou
On réclame le bonheur de pape moussa et sa sœur
Nous réclamons 2 épisode par jour s'il vous plaît 🙏❤️🇸🇳
Vraiment
Yaw khamo foy takhaw 2 épisodes pour laan niatta nguay dioxé ah
@@lifeissoconfused2809 moma diakhal
C'est une série très important
Kou d'accord ni série bi dfa nékhe rek lalalall j'aime ❤️❤️❤️❤️❤️🥰
Kou beugu séydina moukhamad lalale j'aime 🙏✋
Sen série bii nekhna amna sens wayé saga yiii tamite meune nassi niak parck aye khalé daniou koye sétane sinon félicitation à tte l'équipe et bnne continuation
wouyy dioyou ya anna yi😂😂😂🤦♀️agnial rk😂papa Moussa tay bégue na thi ioe🥳
Machallah meilleur série 🥰
Bilahi série en Manou mako mougn😂😂😂😂😂😂😂😂😂👍
👍👍👍
Mère bi day agne di dioyalè😂
Bilay😂😂😂
Kou beugue saydina mouhamed lale jaime ❤❤❤
Macha allah vraiment cette série m a tellement marqué
Khadija bone na trop ms kéne dou papa moussa 😂😂😂
J'ai toujours les larmes aux yeux quand je regarde ce série c'est très la manière dont la majeure partie des orphelins vivent dans leur propre maison avec leur propre parent c'est très triste
Pape moussa khass na mère bi dh 😂
Mère bi mo neh noumouye dioyé yalna diam yague si adouna
Tay mafi moudiou. Topp Len Sama kanam🤣🤣
Kou beugué Serigne Fallou la lal j'aime
OH VRAIMENT SÉRIE BI YEUP AYE DES VRAIS PROS ACTEURS ET ACTRICES MAIS SAMA ACTRICE PRÉFÉRÉE LA GUISAGOUL NAK MO SIYE YAYOU XALÉ BI GUANIOU NDEYSANN 😭😭😍❤️
macha allah serie bu ame solo té ame sense bonne continuation
NON PAPA MOUSSA RÉW NAA BILAHI WALAHI RAY NGAMA OH MAKK KÉN DOUKO TROKHAL NI 🤣🤣😂😂😂🤣🤣
C'est la première fois ma commantaire si série séne tanta dji bonne na trop😭😭😭
Ay badiane li lagnouy diarigne masha'allah
Mère bii frappé na kya ba doyal 😂 mais nak souma sagnon guen éviter sagayi et félicitations nexna trop bary gnarigne machaala 🥰.
Machalla série bi amna solo trop ms saga yi laniou wara bayi
Vraiment
Meilleur série de l'année
Yalna sounou wadiour yi goudou fan gnii djutou yalla kharé aldiana firdaws
Non j'aime trop cette série 🥳🥳🥳 machalla
Kou gueme ni digne ame dome bo goor todé ko seydina mouhamed Psl lalal j'aime ❤
Mère tay niam gua dhé 😂😂😂😂😂😂
Mon séri préfère et vous
Série bi Macha Allah nékhna trop wayé,délén bayi saga yi tamite nak.
Mere bu rèeeeew😂
Non mane ya anna fou ma ray😂😂
😁 partie agne bi Rey nama mane 🤣
Kou begue sa yaye rk lalale aime❤
Serigne abdou Karim mbacke fallilou yalla nako fi yalla bayil té mayko wergui yaram
Amineeeee
Kya ma toma🥰belle belli miss gueye j tadore
Machallah li nekhna tropp li rekkk mo ame si keur yii Bilahi
Papa mousa iow dara ngu De 😂
Ayway français maîtresse bi moma fi bayi des meilleur des élèves 😃😃😃😃
😂😂😂😂
Que du bonheur pape moussa et bb amina
Kia daal la beugg mane❤️🤣
Allez papa moussa😂
BARKÉ YALLA YA ANNA DINAMA RAY VRAI COMÉDIEN LA 😂😂😂
YALLNA SA2 JAAM YAG
Yayou Khady mi niit la 😂😂 mais mafi djitou nak
Mère Anna depuis série Keur Nguewel lako done suivre 😂😂😂😂
Bouma nékone pape Moussa dina wane sama tanta foula AK faida bou dou gnimé wx AK mane yéne yi teksi protège sama rack kendouko sonale mai ki bonna waay🙏
Première commentaire mère elle joue bien sont rôle 😂😂
Dafa mèl ni mafi djitou dh🥰
Wouyyy papa moussa mo bax si mère bi😂😂
Vraiment papà Moussa j l’adore louma dioyone rek rétane lo guamako tay 😂😂😂
😃😃😃😃mère bi reynama wayyy
je l'aime papa moussa 🥰❤️
Noublie pas les 5prière ❤
Machalla série bi nekhna trop
Tre important les serie comme ça dans la société
Merci papa moussa 🙏🙏🙏😅😅
Kou daccord ni series bi dafa nexx lala,l jaime
J'aime ce série des j'aime pour pa moussa et sa sœur
Longue vie maman ❤❤
Nekhna trop ms svp saga yii ay xaleii dagne koy setanee ms nekhna machalla😍😍😍
Kumay santal khadimoul khadim ❤
Bébé Amina kaay machallah daffa yéwou 😂😂😂😂 Khady sa beuss déh dina mélni bou Biba ba ak gorom ba 😂😂😂
barki yala 😂😂😂
@@awandiayediouf2437 😂😂😂yaaw kaay wait rék
Niafff moussa 😂😂😂❤
Non moussa merci 😂😂😂
Meilleur série ❤
,,,,,🥰🥰🥰🏐🏐😂😂😍😭
Djrime dafa meti mais courage yalla bakhna❤
Machalla film bii nèkh ❤