La discussion entre Alkaly et Mr Sow me tient droit au cœur. C'est une discussion morale et éducative.Alkaly est un vrai chef de famille. Sacré Amy Mbaye elle joue son rôle à la perfection avec sa langue de bois. J'aime la responsabilité de Makhoudia Tall envers ses trois femmes.
Maxou mi mo niakk jom 😂😂iow demo ligeyii amal sa bop terrain boussa papa ndjeundeu si xalissam ngani sa alal leuh nih😂😂ba diko reclamer avec agressivite😂😂😂kou dcr ni ki amoul jom❤❤❤
Cette discussion était intéressante, mais ça n efface pas ce qu il a fait il doit aller s excuser auprès de makhoudia pour les gros mots qu il lui avait dit .Petit makhou lui il est devenu impoli et arrogant.
Vraiment l’amour d’un père et juste incroyable 🥺Dieynaba et tellement proche de son père que beugoul louko meti😭Gniko gnakk nalene yalla same🙏🏾maylene kholou mougne
Tonton Alkaly incarne le rôle du père responsable à la perfection.😊🎉 Ça façon de recadrer makhou etait super. Ainsi que son face à face avec sow.. 🎉🎉🎉🎉 le bon exemple 😊😊
Dans chaque famille il y’a un enfant qui brise le lien de la peuvreté je parle de toi qui regarde cette magnifique série tu sortiras ta famille dans la peuvreté si tu crois tapè Amine bonne soirée à vous que Dieu vous protège chaque personne ici présente 🙏❤️
Le comportement de Djeneba, me rappelle-moi comment j’étais avec mon père avant qu’il ne décède 💔c’est vraiment incroyable, je l’aime de tout mon cœur quand lui et ma mère font l’histoire, je me comporte pareil je pleurais tellement, je leur demande d’arrêter vraiment bravo à Djeneba elle joue très bien son rôle ❤ meilleure série
Vraiment même moi il exagère trop très con quand sa maman était en vie il ne fessée rien pour le défendre maintenant elle est mort, il veut jouer au fils idéale
😂antouka mane Amy mbaye la andal nakh yoor na djiko bougnou sopou si djiguénne mouy niak diom beugue dieukeuram lene rk moko yakh mouy df bari ay caprices te lolou yakhoul djiguénne ❤😂
qu’ الله aide la Palestine qu"الله accepte nos duaa qu'الله nous accordé le paradis qu'الله accepte nos prières qu'الله protège nos parents qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
Non Amy mbay douma Rey man mai hawna deugu dé j'ai une grande sœur qui était au Sorbonne mai légui gnibsina bu yagu Di nan dédon def ay cosmar chek nuit pendant 2 mois té fofou Amou ma meunn mou gnibsi 2015 pour niou diohko loumouy Sango mai mou bagna gnibi mai mo guéna meuna roulé ayy RR 😂😂 est ce qu'a conn cartouché woull tamite no li dinathi def ay ankétt beu ham
Vraiment sama xol toyna Even prod m’as touché aujourd’hui pour le sequence de makhoudia tall et de sa famille j’ai pleuré car j’ai un peu vécu la même situation que Dieynaba tall traverse concernant sa belle complicité avec son père l’amour d’une est tellement fort peace et amour à celles qui aiment tous leurs papa je t’aime mon papa d’amour repose en paix
Douma beugg Loudoul dougou si série ndokhou Makhou bu ndaw totalement avec sa manière de parler……. Mais Amy Mbaye mom keneu doussii waax elle est très forte 💪
Il ne reste plus que 4 jours à vivre en 2024, remercions DIEU pour tout ce qu'IL a fait cette année et par avance pour ce qu'IL fera en 2025. Paix aux âmes parties cette année et que DIEU nous bénisse tous Amen 🙏
Incroyable talent de Amy Mbaye 😊❤......kou d'accord........????😊
Wei elle assure grave 🎉❤ chapeau à elle
❤❤❤❤❤❤❤
La discussion entre Alkaly et Mr Sow me tient droit au cœur. C'est une discussion morale et éducative.Alkaly est un vrai chef de famille. Sacré Amy Mbaye elle joue son rôle à la perfection avec sa langue de bois. J'aime la responsabilité de Makhoudia Tall envers ses trois femmes.
QSWDXW,😢😢😢
Vraiment n’est pas un bon responsable s’il dit qu’il veut plus des Laobés et consorts donc il doit répudier leurs argents 😮
Ndeysaan l’amour d’un père est très nékh ❤️🥺
Kou beug papam comme ni Dieynaba beugué papam ak mane rk lalal j’aime 😢❤️
❤❤❤❤
Sama papa 😢yalna ko yalla yeureum
Moi j aime mon papa
Il est tout pour moi
Ak Mane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Longue vie à nos papa j'aime mon père plus que tout
Maxou mi mo niakk jom 😂😂iow demo ligeyii amal sa bop terrain boussa papa ndjeundeu si xalissam ngani sa alal leuh nih😂😂ba diko reclamer avec agressivite😂😂😂kou dcr ni ki amoul jom❤❤❤
Rew ba dof la def😂😂
@antadiagne137 no bilahi serie rek leuh dh mais sama xol bi day diéxx soumako dégué mouy waxx🤣🤣
@@babshifayzo663 bilay yaw 😂
J'ai quand même bien apprécié que son père lui ait remis les pendules à l'heure.
Li mo am sénégal kheuthio allou bay
Bassine hamon nganii si mbéde yui ngay accouché comme da ngay weurr rékk 😅😅😅😅
😂😂
😂😂😂
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Chacha est trop belle 😍 machallah
Pere Ndiaga thiame Goudal fane way niga gnouy bèguè lè yalla nala yalla fay damay rèè ba sonn toujours comédien 😂❤
Amine
Amine yarabi 🤲🤲🙏🙏
Amine🤲🙏♥️
La scène avec loc me fume 😂😂😂😂
La scène avec loc me fume 😂😂😂😂
Amy mbaye raynama "thiowou mére yonou nouveau-né nékousi"😂😂😂
Kone wax nafi lii😊
😂😂😂😂😂liiiiii
😂😂😂😂😂
@@awandiaye-ye7gp waw 13:44 😂😂😂
Svp des millions de ❤ pour notre prophète mouhamed PSL
❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Salal lahou Ala mouhamad ❤️❤️❤️
❤️❤️❤️❤️❤️
Une pensée pour ceux qui vivent des moments très difficiles et qui ne peuvent en parler à personne Yalla nalen Yalla taxawou si barki Muhammad (PSL)
Amin
Amine inchallah
Amine ya rabby 🥰🤲🙏❤❤❤❤
Amine yrabi 😢li nekk sma khelmi meunoumako wax😢😢
Aminé
Touche boo def ci «👍» yalna doon Salaat sur notre Prophète Mohammed (PSL) à ton auteur
Sallahou alla Mohammedine allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii ❤
Sallalahou hala mouhamed
@@MoctarDia-e5j aetsxcgdssqa
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Diammi Adouna ak alakhira barki seydina Muhammad 😭😭😭😭
😊😊😊😊
Amine
Amine
❤❤
❤❤❤❤❤❤
La discussion entre Alkaly et Mr Sow ,tres moralisant et educative.Alkaly ,un vrai chef de famille
La meilleure séquence de cet épisode ma sha Allah alkaly est plein de personnalités
Cette discussion était intéressante, mais ça n efface pas ce qu il a fait il doit aller s excuser auprès de makhoudia pour les gros mots qu il lui avait dit .Petit makhou lui il est devenu impoli et arrogant.
@@Khadimamadou oui makhou junior c'est grave ! Mais son père la bien remis à sa place !😮
Amy Mbaye nena Bassine khamone nani sa dom bii si Mbede mi ley guené 😂😂😂😂😂😂😂😂
LOLOU LIMAKO RÉ😂😂😂
Aka rew😂😂😂
Khana guisolen traduction bi 😅😂
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂 votre fils est a mbed@@FatouMbaye-rd7js
Père Ndiaga ak diouma comme Sama yaye ak seutam yi 🥰🥰yaye goudal fane and ak wer
Sama ndaw dém na nguewèl 😂😂😂😂
Commentaire bi la done sett😂😂😂
Wouyy😂😂😂😂
Moma ray 😂😂😂😂
Sheuteuteut 😂😂
Fils
Sheutt amy MBAYE encore amy MBAYE 😂😂😂😂😂khawma foumouy dieuleh limouy wakh rek
Amy néna Xékhou mère yonou xalé nekousi 😂😂😂 Sacré amy mbaye😂
Amy Mbaye dou nitt😂😂😂
😂😂😂😂
😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
Bilaye ki dou nit
Lok bombe ak mame bou Gor non bête bete le meilleur père ndiaga dinama Ray 😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂
Nenako ma teup la mbéthie sa baye😂😂
Vraiment l’amour d’un père et juste incroyable 🥺Dieynaba et tellement proche de son père que beugoul louko meti😭Gniko gnakk nalene yalla same🙏🏾maylene kholou mougne
Amine ❤yarabi
Amine 😢
Amine ya rabi
Amine 😢😢
Amine yarab inchala
Des cœur ❤️ pour notre Prophète Muhammad psl ❤❤❤❤
L’amour que père ndiouga Thiam porte pour sa petite fille est démesurée 😢😢😢
Rasta you xiboone😂😂niou custumiser thi kanam amyyy mbaye tu es qui dis moi😂😂😂😂
Ami mbaye Kay amoul 😂😂😂😂😂
Amy mbaye rek Ken dou mom😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉 53:50
Mo raw bassine khamna kouko bolé ak awa kiné ak mareme bou diama non bobou trioo😭🤣kou meune seu morom doumeu
😂😂😂😂😂
Cheikhoul khadime amatina ndam❤❤❤❤❤❤des cœurs pour serigne touba❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
Wawaw machallah ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤ c'est clair ❤❤❤
Tonton Alkaly incarne le rôle du père responsable à la perfection.😊🎉 Ça façon de recadrer makhou etait super. Ainsi que son face à face avec sow.. 🎉🎉🎉🎉 le bon exemple 😊😊
Dafko yékha déf
🇲🇫: Une série vraiment intéressant ❤️
🇸🇳:kou beugue yonenté bi lalal j'aime😥🤣
😅😅😅😅😅right
😂😂😂😂
😂😂😂😂
Aussi nieye ray sen family 😂
Nn Amy dou nitt ay khéttou parolam rk 😂C’est bien très bien 😂😂
🤣🤣🤣
Non père ndiaga ak lock bombe niomay raye 😂😂😂 ma teupe la medje sa baye
Une maison de production qui ne déçois jamais ses téléspectateurs c'est evenprod diam thi y'en mes amours yalna diam yagg waay❤
Vraiment ils sont leurs meilleurs. ✨️✨️✨️✨️✨️
Alkaly qui parle avec diplomatie je l’apprécie bcoup vrai père de famille
Bété Bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤😂🎉
Dans chaque famille il y’a un enfant qui brise le lien de la peuvreté je parle de toi qui regarde cette magnifique série tu sortiras ta famille dans la peuvreté si tu crois tapè Amine bonne soirée à vous que Dieu vous protège chaque personne ici présente 🙏❤️
Amine
Amine ya rabbi
Amine
Amine🙏
Amine
Yalla yalla defal gnou weurseuk ak tawfekh mousseul gnou si pekhei ak louy lorei
Si barquei sangu bi
Amin
Amine inchallah ❤
Amind
Amine 🙏
Alahouma amine
Le rôle de look bombe on a parle pas😂❤❤❤
Jeudi Tay bii yalla Boumou nekk souniou dernier jeudi,niou fekké thi barké seydina mouhamad psl🤲
Sa heure dée bou joté dangay dée bouleen niou sonal way ah😂
Amine
Amine
Amine
Amine ya rabby
😂😂😂 ay way li nexna père ndiaga néna lock bombe ma teupp la mbéthie sa baye 😂😂😂 shasha néna yayam sama daw dém na nguéwal😂😂😂😂😂 Evenprod ❤❤❤❤
❤
😂😂😂
😂 sacré Bassine dii cas bah nara weussine si mbédeu bii 😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
La série qui n'a jamais perdu sa valeur c'est une série extraordinaire
Le comportement de Djeneba, me rappelle-moi comment j’étais avec mon père avant qu’il ne décède 💔c’est vraiment incroyable, je l’aime de tout mon cœur quand lui et ma mère font l’histoire, je me comporte pareil je pleurais tellement, je leur demande d’arrêter vraiment bravo à Djeneba elle joue très bien son rôle ❤ meilleure série
Moi pareil sa fait tellement mal t voit tes êtres cher se déchirer entre eux eux😢
Amy mbaye nakk mogui mayy dogua neikh lii😂 fatim thiam mom dafa niak classe sheutttt 😂
Bravo à toute l’équipe de bété bété 👏🏻🥰
Wa ami mbay my métna10
Des cœur pour notre prophète Mouhamed psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
صلى الله عليه وسلم حبيبى يارسول الله
Salal lahou Ala mouhamad ❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Le petit Makhou est la preuve que certaines situations de la vie font tomber les masques de certaines personnes pour voir leur vrai visage...😔
Des cœurs pour notre profete mouhamed PSL ❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Paix et salut soient sur lui Amine ya rabby 🥰🤲🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maco moudié sétane 😢guouldi aldiouma la diougué gnanale na nieup inchallah 🙏
Amine waye
Aminne long vie ❤
Amine
Aminn way ❤🎉
Amine yarabbi alhalamina ❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤
Makhou Bou ndaw m'énerve vraiment en ce moment temps yi dafa réw trop
Defa sof trop il exagère vraiment
Vraiment même moi il exagère trop très con quand sa maman était en vie il ne fessée rien pour le défendre maintenant elle est mort, il veut jouer au fils idéale
Belie dafa rew torp😏
Il a toujours été idiot 😅😅😅
niak khorom mome ak Amina 🤨🤨
dafa rew torop
Chacha Sama Daw demna gueweul 😂😂😂😂elle a fait ma soirée 😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
J'adore chacha 😅🤣elle a fait peur ça mère c'est très bien c'est très bien
@@Omardiallo-yr3nvBayile diawar ndiane fi dou xalliso 😂😂😂 c'est bien tres bien
@@ramatoulayecamara-zh9gv 😅
Koumay santalé YALLAH ❤❤❤
الحمدلله رب العالمين ❤
Alkhamdoulila yalla Jërëjëf ❤❤❤❤😢
@@farimataThiandoumeAlkhamdoulila yalla Jërëjëf ❤😢
Goudi aljouma bi lep lousi way nian rk yalla yalla nagou ko tamou guen si yw😢❤❤
Amiin ❤
امين
Jeudi❤
Amine
Amine
Demb la sama papa am 1ans si souff nianalén makko yalla Nako yalla yeureume ❤
Yalnako yalla doli yeurmande ak ndiegal si Barke Nabil Moustapha ❤️
Yalla nako yalla yereme 😢
amine 😢
Amin
Yallana aldiana done keurem yalla yessal yeurmadé si môme
Merci Alkali khalé dégn koy yar. Les séries doivent refléter une bonne image des familles. Il faut respecter ses parents
Ľamour de pére ndiouga envers diouma et ľamour de dieyna envers son pére est incroyable ❤
Kou yeureum mame bou djiguéne comme mane😌
Da sikk nakkk 😂
Momayé domou diambur nak 😂😂
Amadou sow franchement il me rappelle jean Paul Damelda paix à son âme
C son cousin
@@maimounathiam2748han ok je savais pas merci beaucoup
Oui ils se ressemblent tellement 😢😢
Merci il se ressemblent machallah❤
Bilay
Alkaly il est trop civilisé ❤
Des coeurs ❤pour notre Prophète Mohammed (psl)❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Salalahou alla mouhamedine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤
J'aime trop Amy Mbaye et sa façon de s'exprimer😂😂😂
Surtout llou
Billayi 😂😂
Ma yakarni mane kassé la
Elle est le meilleur ❤❤❤😂😂😂
Wa ou elle as ses terme a elle ki te pike grave ❤❤❤
😂antouka mane Amy mbaye la andal nakh yoor na djiko bougnou sopou si djiguénne mouy niak diom beugue dieukeuram lene rk moko yakh mouy df bari ay caprices te lolou yakhoul djiguénne ❤😂
Billahi Aka man❤❤❤
Lou lér😂
Ma Beug Amy mbaye 🎉🎉 bilay
C'est vrai 😂
Mais personne ne parle le jeu d’ alkaly vraiment il joue très très bien maasha’ الله 🎉
Kiy maquiller aïssata kâne. Vraiment mettrena beauty wam en valeur elle est ravissante
Bilahi rafét la déf machalla ❤❤
@@NdeyearameSene-lf1ll ki sou maquiller woul sakh day rafete
@capricefemelle3168 jai pas dit le contraire dh
❤❤❤
Aïssata thie bopam bo rafét❤❤❤kou rafét nékha defar❤ Machallah
Dernier jeudi de l'année 2024. Yalna niou ko féké ay att you bari kén bania manqué
Amine 🙏🙏🙏
Amennn
Amine
Amine AK BEP dioulite
Amine yarabi 🙏🙏
2025 bi ligua beug Yako kham yalla na laguo yalla defale si barke seydina Mohamed psl ❤❤❤🎉🎉🎉
Amine
Sallalahou alla mouhamad
Amine 🙏🙏
Amine
Amine
Faatim Caam jigéen bu bon la, 😢😢sa kër bu tasee yaa ko tas, Yal nanu Yàlla musal ci jigéen bu mel ni Faatim Caam.
Bou tassone keureum kassé kone mou nékh mé keur yeup la tass😂😂
Damako bagn
Père ndiaga meilleur acteur bonne continuation
😂❤❤❤❤❤Dieynaba🎉❤❤❤et ❤❤❤son pére
Gni nék si nakar té meunougnouko wakh kéne yalna yalla tégui yeup si barké seydina mouhamed psl salallahou allah mouhamed
Amine
Amin
Allahuma amine 🤲🤲
Sacré Amy Mbaye toujours égale à elle même 🎉❤😂
Mame bou djiguéne raffet na machalllah ❤😢❤❤
Jtjr elle est tellement belle ❤
Des cœurs pour notre prophète Seydina Mouhaméd (psl)🙏🏾❤️
Mon frère me manque😭😭 beaucoup prier pour q’il repose en paix de son vrai nom Talla Camara 🤲🙏yalla nala yalla kou wakh amine yalla gua goudou fane🤲🤲
Amine waye
Amine
Amine yalnalako yalla yeureum
Amine
Paix à Son Âme
Amy mbaye mo rew wooouye waye wakhe na déugue moy khale bi dh 🤣🤣🤣🤣🤣
😅😅😅
Amy Mbaye elle parle avec les réf de tik tok😭😂😂😂😂
qu’ الله aide la Palestine
qu"الله accepte nos duaa
qu'الله nous accordé le paradis
qu'الله accepte nos prières
qu'الله protège nos parents
qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
Amin
Amine inchallah
Amine❤
Sodlsod LDLC syndicalisme f si kh stp i kh g
Amine yarabi
Bilahi amy Mbaye dou nite sheuut 😂😂😂
Non Amy mbay douma Rey man mai hawna deugu dé j'ai une grande sœur qui était au Sorbonne mai légui gnibsina bu yagu Di nan dédon def ay cosmar chek nuit pendant 2 mois té fofou Amou ma meunn mou gnibsi 2015 pour niou diohko loumouy Sango mai mou bagna gnibi mai mo guéna meuna roulé ayy RR 😂😂 est ce qu'a conn cartouché woull tamite no li dinathi def ay ankétt beu ham
Ay wayy délén wakh thi série bi téh bayih Serigne Yii tmt 🙂↕️🥴❤
Vraiment
Mane j'aime yiniouy niane la khamoul pour lanla bly
Vraiment il faut niou wakh si tamitte
Loo xam si reew bou barri idiot rek
Yabaté rék ak soof
Fatim Thiam dou djigueen Bou bakh franchement
Pa paré sou guissé alkaly bou daw day guena rakadiou
Je suis d’accord
Bilahi téksi amoul bénn yarr ni respect envers sont mari Awo d'à wara nék référence nèk yaye,té kou mine say wakh yépp leu
Amy mbaye yallna sa diamou yague 😂😂
😅😅😂😂
Kou remarqué ni ni diouma thiam di neubé kanam gui mingui reitan 😂😂😂😂en plein action ❤
Kone Guisnga lolou
Même oumou khaïry bimouy segue dadone ré😂😂😂
@@kyafaye5604même remarque 😅😅
Riko glace bii moko retanloo😂😂
Guiss nako 😂de riko glace bi raynama père ndiaga😂😂
Des cœurs pour notre prophète bien aimé sallalahou aleyhi wa salam ❤🎉
Salal lahou Ala mouhamad ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cartouché biir Sorbonne 😂
Beugn bu manqué vitamine 😂
Diassi 37😂😂
Waydawlou yi yalna yalla yeuramlén kou wakh amine yalna bari xaliss
Amine Ya Rabbi
Amine
Amine
Yalla nanie doundou ba terral souniouy wadiour 😊 inchallah ❤
Alahouma amine niou bok lép inchalla
Ahmine
amine
Aminn yaa rabbi ❤
Amine
Aka nekhon ma nek dalou Yonnety bi psl ❤️☝️
Sallalahou alla mouhamad
Psl❤❤
Salal lahou Ala mouhamad ❤❤❤
Bama sathie la dinga xam lepp deug leu 😂
Psl❤❤❤
"Khoulo wou makk yonou nouveau née nèkoussi 😂" Amy mbaye sayy paroles intense nagne😂
Vraiment makhou mou ndaw dafa commencé réw bly😢
J'aime bien Amy mbaye et sa façon de parler 😂😂😂😅
Vrai comédien la 😅
Tayy la sama yaye am 26ans sous terre nianal léneko
Yalla nako yalla yeureum th khareko aldiana 🤲🏾🤍
Yalla nako yalla yeureum 😢😢
Yalna ko yalla yeureum th khareko aldiana firdawsi
Yalla na ko Yalla yeureum khare ko aldiana firdawsi
Ndaysann yalla nako yalla yeureum 😢
L'amour familial , l'amour entre un père et sa fille, l'amour entre une mère et son fils c'est tellement extraordinaire ❤️
Touly rafete na way cette nouvelle version de makhou bou ndaw me fume vraiment il m'énerve
Mom rekk moma soff
Plainte bi lay yi khar mou dem police kholat bopam
Dafa fate ren by
@@mamycisse3565 nieup la sof kay
Dafa doff bilay
Mame bou djiguéne dhé mougui xol nogay rk😢 ndeysane dérét dou reure😢
Vraiment dou rere dafa fort motakh
Nogay dou chiekhbi khassa la
@BarraDioubou yaw est ce que ça va fo dégue lolou bo nekke sekham nou ngi seuye tu t entends parler
Bete bete la serie qui n a pas encore perdue son goût. 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹
Billay ❤
Vraiment sama xol toyna Even prod m’as touché aujourd’hui pour le sequence de makhoudia tall et de sa famille j’ai pleuré car j’ai un peu vécu la même situation que Dieynaba tall traverse concernant sa belle complicité avec son père l’amour d’une est tellement fort peace et amour à celles qui aiment tous leurs papa je t’aime mon papa d’amour repose en paix
Merci à tous les jours qui suivent ❤❤❤❤❤❤❤
Des cœurs pour notre profete seydina Mohamed psl ❤❤❤❤🎉🎉❤❤
Salal lahou Ala mouhamad ❤❤❤
❤❤❤❤❤
Ba khamgénn madione lay MAKHTAR dfa meune limouy déff domou cambrèn bi❤❤
Walahi ❤❤
❤notre fiertei
Ndeysane mame bou goor beug neu Diouma moko gueuneul lepp si adouna😭😍🥰🎊🎉
Sacré Amy mbaye😅j'adore 💕 quand chacha parler peulh machallah 😅❤️
Douma beugg Loudoul dougou si série ndokhou Makhou bu ndaw totalement avec sa manière de parler…….
Mais Amy Mbaye mom keneu doussii waax elle est très forte 💪
Vraiment makhou mou ndaw exagère
@@seynabouseck2021trop c trop séquence boumou nekeu damakoy avancer Sahh
Dafa reew trop
@ mais sa yay dhé waroul takk do am respecter si say papa
Alkaly bu ndaw dako wara ndokhou rek
Ça montre qu’il a réussi son rôle 😂
Bilahi j'aime trop amy mbaye sa façon de s'exprimer vraiment elle est forte 😮
Boulén faté ni modou Lo moy rois 👑des arènes 👑👑👑👑
Balla empereure
Borom 150 millions yi empereur bi seul😂
Empreure bi seul 🎉🎉❤❤
sama papa Baye Papa Seye yalnako YALLA diégal bolékok malakam yeurmandé yokou ay léram oubilko ay khéweul kharéko ALDIANA🤲🙏😭😭😭😭
Il ne reste plus que 4 jours à vivre en 2024, remercions DIEU pour tout ce qu'IL a fait cette année et par avance pour ce qu'IL fera en 2025. Paix aux âmes parties cette année et que DIEU nous bénisse tous Amen 🙏
Je suis très heureux pour se que ta dit merci ❤❤❤❤❤❤❤
Amine
sa yaye yalna fékké sa niarigne waxal Amine ♥️
Amine
Amine way 🤲🤲🤲
Amine
Amine
Yalla na gneup am diam si barke seydina Mouhamed psl ❤❤❤❤❤❤
Ndeysan cheikhou Gueye yalna goud fan yaguena bégeul sénégalais yi