Merci pour la promotion de la destination Sénégal. Vous êtes la preuve que quand on chante vrai, on chante forcément juste et on chante bon! Merci M. Seck
Encore Encore tu as frappé la grande porte patriote bou mague bi ningay souhaités patriotes yi bon dimanche nex nagnou trop❤❤ningay fekhalé sougnou khol yi yalana yalla sedalé sa khol nonou le 17 mom inchalah patriotes yi degno ame ndame ba paré li la guente té moy ame inchalah bilay contane nagnou ci iow yalla nala yalla tek lokho moussal la mouthial çi seytané ak pekhé noone lakh la fa yakh égoul yaye sougnou champions di sougnou roi des mbalax bon dimanche a tous et toutes patriotes ❤❤❤❤
Walay diam day ndangou ndogalou yalla ❤❤❤ merci beaucoup Abdou 💪💪💪💪💪💪♥️♥️♥️♥️♥️ Sonko kouko beugu niou beugu leu ❤ le 17 yalnaniou yalla may ndam gou séd Gouy 🤲🤲🤲
Un immense merci à Abdou Guité SECK pour ce magnifique clip ! Ta musique et tes visuels transcendent les émotions et nous transportent dans un univers unique. C’est un vrai régal de te suivre et de découvrir ton talent. Continue à nous enchanter avec tes créations ! 🙏✨ Grand do Niti fi
T'es chansons sont tellement cuissées avec amour et douceur qu'on n'a aucun dégoût à les écouter et réécouter. Merci mon Artistes ❤❤❤. Chers tous svp faîtes en sorte qu'on atteigne des millions de vue avant la fin de la campagne ❤❤
Domou baye bilahi contane nagnou si yaw yalna yallah defal gnou diam ak salam ak ndam insha'allahou rabi bagnou lay def ministre de la culture du Sénégal. On t'aime un fans de thiés ❤❤❤ Masha'allah
Neikhoul ba neikhoul mais SÉNÉGAL yafi Dak way
La vérité ❤❤
Les artistes n’écrivent plus et ils chantent que l’amour. Mais lui chapeau macha Allah bon vent incha Allah
Merci beaucoup
Rendez vous le 17 novembre voté pour déllo gnoukall sayidana Ousmane sonko Al Moubarak le premier ministre panafricain 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Inchallah Rabi
Khaw ma rékk kagne layy guiss dieum dji ❤❤❤
Khanaa son bé Moy takh gnou takk maa 😂😂
Qui est d’accord Abdou Guité Ministre de culture il a combattu avec sa voix
No boulénë indi diakhaso culture,sport al jeunés gnon andë fépp fo dém si dëkk you bari
Xoll seed na ziguinchor une des plus belle région du Senegal une fierté
Une très belle région 🎉❤🎉
@@AbdouGuiteSeck yaye ndanane nk Seck 🎉 do ioe t do niom
@@AbdouGuiteSeckgrd bégal ga ma torop.
T'as résumé ziguinchor ici,la terre de notre Pros ❤🇸🇳
Mon préféré @@AbdouGuiteSeck
Je suis très content de toi notre chanteur préféré ❤
*Souma fateliko ni mom rek lagnou ma dakantalé ndakh nimako beugué wone ba bou guéné téle rek niou woma 😊depuis khalé 😊ba legui sama thiofell si mom di guen di yokou ndakh gnémé deuguem ag guem bopam wahouma nak gnou bokou PASTEF ❤focus rek le 17 novembre 2024 gnou majorité bou écrasante inch'Allahou Rabi 🙏🎉*
Je pensais que j'étais là seule à avoir l'aimé. Il chante bien machala
@marienoelmayesarr5351 *je suis là depuis tout petit*
Jeem ko daan ko meun ngako 150 députés ❤❤inchallah
Inchallah 🙏🙏
Ndeysan malgré sama thofel bou am doole si abdou gitteh seck mais legi monoa toumko topou 😭mais yallah bakhna
@@HachamiyouDjigo louy lolou
160 rk inchallah pour kou séll ki ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@ Merci de tout cœur, Lou Yague deguela
Toujours égal à lui même ❤
Le meilleur chanteur du peuple. On vous aime 👍 😊
Maximums de soutien à notre artiste patriote..💪👍🇸🇳
Beugonne nala ms damala guenah Beugue naxe ligua nekk patriote ❤❤❤
Dieureudieuf @ Abdou guité Seck yalla na SOUNOU BOROM goudeul sayy fannn❤❤❤
Merci bcp sama Artiste bi nékh na trop Sonko à vie ❤️🔐🫡❤️❤️❤️❤️❤️
Tonton Abdou Guitté séck le chanteur du peuple on t'aime ♥️
Merci maléne raw
Merci pour la promotion de la destination Sénégal. Vous êtes la preuve que quand on chante vrai, on chante forcément juste et on chante bon! Merci M. Seck
Le bel endroit du monde tu as clipé dans mon fief Escale .Merci d'avoir cru au projet et des le début.
Un vrai patriote Guite Seck.
Sénégal yaw rekk yafi wakhe lonio khamé bilaye
wa yén li nékh neu ba souroumlé di 🥳💪🇸🇳❤️
MERCI ABDOU GUITTÉ POUR CE JOLI CLIP TOURNÉ À ZIGUINCHOR MA VILLE NATALE !
Abdou guitté machalah yalna la yalla samou 🎉 ame neu solo ❤
Machalla❤❤❤❤❤❤❤❤sonko moy diomaye moy sonko❤❤❤❤❤❤❤❤
Ani wa zig manifester vous❤
Niongui ni dé,li nékhna torop❤🎉
Le meilleur de sa génération ❤❤❤❤❤✅️✅️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
1M de vu avant 2 semaines les patriotes in sha Allah aythia aythia aythia ma giss pour majorite bi assemble ❤ ma sha Allah Ton's Abdou
Encore Encore tu as frappé la grande porte patriote bou mague bi ningay souhaités patriotes yi bon dimanche nex nagnou trop❤❤ningay fekhalé sougnou khol yi yalana yalla sedalé sa khol nonou le 17 mom inchalah patriotes yi degno ame ndame ba paré li la guente té moy ame inchalah bilay contane nagnou ci iow yalla nala yalla tek lokho moussal la mouthial çi seytané ak pekhé noone lakh la fa yakh égoul yaye sougnou champions di sougnou roi des mbalax bon dimanche a tous et toutes patriotes ❤❤❤❤
Ki mane n’a waye 🎉🎉
Majorité écrasante inchallahou rabbi comme niko kou séll ki beugué💪💪💪
Mane kii dama koy beugue bah kagnn❤❤❤😢
Walay diam day ndangou ndogalou yalla ❤❤❤ merci beaucoup Abdou 💪💪💪💪💪💪♥️♥️♥️♥️♥️ Sonko kouko beugu niou beugu leu ❤ le 17 yalnaniou yalla may ndam gou séd Gouy 🤲🤲🤲
Jub jubal jubaneti, ték si di lidieuneti. Lifi nek kouné amssi gnou dém ba gneup diotssi. Holalala le texte est très riche ❤
Sissou bi nak mo beri sirewm merci beaucoup Abdou
Malheureusement 🎉
Ndaysan li née na…❤
Son bi nexna teksi mou am ndiaring niou dioublou si defar rewmi meuna nek ousmane moye Bassirou❤
Sonko diomay point kou mere ya kham focus le17 inchallah ❤
150 députés 150% Sénégal bou geuneu on peut le faire ❤❤❤ Inch'Allah
Un immense merci à Abdou Guité SECK pour ce magnifique clip ! Ta musique et tes visuels transcendent les émotions et nous transportent dans un univers unique. C’est un vrai régal de te suivre et de découvrir ton talent. Continue à nous enchanter avec tes créations ! 🙏✨ Grand do Niti fi
Merci infiniment❤
Senegal rek ❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Ça montre bien que tu aime SONKO ❤❤❤comme nous l’aimons
Yaw dokhalal rek ❤❤❤❤❤
T'es chansons sont tellement cuissées avec amour et douceur qu'on n'a aucun dégoût à les écouter et réécouter. Merci mon Artistes ❤❤❤.
Chers tous svp faîtes en sorte qu'on atteigne des millions de vue avant la fin de la campagne ❤❤
Yaaye Sunu Artist
Senegal 🇸🇳 moo leu beugeu bro ❤
Yallna borom bi samou le ndam rék inchallah jerejef manchalla ❤❤❤
Hiii pourquoi wowolénma si tournage bi ma japsi❤
Notre Ags , tu as encore tapé très fort. Machalah ❤❤❤.
Machalah Il N'a Jamais Déçu Sa Publique 👏🏿🫶🏿💯
Ce 17 novembre incha allah nous allons donner une majorité confortable au gouvernement.
Domou baye bilahi contane nagnou si yaw yalna yallah defal gnou diam ak salam ak ndam insha'allahou rabi bagnou lay def ministre de la culture du Sénégal. On t'aime un fans de thiés ❤❤❤ Masha'allah
je t'aime beucoup grace a sonko
Vrement ningay woyé ak say khétou waxin yémnama machallah❤guitté ndanan
Macalla liu neexna waaye ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉jaajef abdou giute seck
La voix du walo❤
Nioune yaw laniy diklou te say way day diarigne bonne continuation Abdou
Le chanteur du peuple ya meilleur kaye 🇸🇳🥰🎉💃💃❤️❤️❤️❤️❤️❤️💖💖💖💖
Machallah Abdou ❤❤❤ sonko à vie
Ya dakeu way si sénégal par force ❤️
Ags t'es un grand patriote tu fais partie des plus grands référance panafricain ❤❤❤❤Big respect a toi
Messaggio bi amna importante ❤❤ yalla n'a yalla diallale❤ Amine
Le chanteur du peuple ❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢❤❤❤❤
❤❤❤❤ Sénégal yafi dàkk way tonton Abdou guite ❤
Sama wadjie ❤❤❤❤ guirr yalla 1 millions d'abonnés mes mbokk patriote ❤❤❤
Tu fais partie des meilleurs walah ❤
Machalla abdou yaw moum Gour puer nga
Merci pour cette belle vidéo Guité Seck le patriote. Le 17 Nov 2024 sortons voter massivement pour liste Pastef 150 Députés.
MSF ❤❤❤
Way Kat bou mak bi ya beug sa réw❤❤
Sonko rek Sénégal dieum kaname 🇸🇳👍♥️✌️
waw Abdou mi mingui wané dolém 💪li dé lanou begue nigoun fanse yi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Un endroit symbolique monuments de la paix Ziguinchor vraiment merci le chanteur du peuple ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Le Sénégalais d'abord👍🏿❤️🇸🇳 kou wadjie mér tiokal kou mer thiokal😊 avancé.
Focus rek ba 2099 inchalla ❤❤
Abdou Guitté Seck patriotes yi sén xol sédna si yaw ❤❤❤❤
Alhamdoulilah ❤
Tu es le meilleur 🎉❤❤
Hééé guité seck ya meune ya eupeu dolé ya degg wolof ndar ndar deugeu ngua
Je suis la première personne à voir cette vidéo
Fen rek
Machallah merci Abdou Guitté on est fière de toi ❤❤❤❤❤
😭😭sma khôl bé Sed
Alhamdoulilah ❤
Les paroles❤
ABDOU GUITÉ UN VRAI PATRIOTE
Partager len ko 🎉❤
Merci beaucoup tonton je suis très content ❤❤❤❤ papa Ousmane sonko rék bilahi wolahi
Xourou Opposition Bi Yépou Ak Tiokhou Djigéne Yi 😅😂
Souko rkc inchallah ❤❤❤❤
Machallah Abdou Guitte seck tu as de la suite dans les idées
Merci infiniment
❤❤❤❤❤ yalna yallah samoulénn inchallah ndam ❤❤❤
Le chanteur des patriote a déjà été patriote de cœur machalla Abdou Guité
Dieredief abdou djité nioune patriote yi amouniou sa Faye 🙏🏻
Les patriotes Naniou Diem partage ko,lima fi dokhantou barina dei
Dangay guiss li rekk bly Abdou guite Seck moy ndanane wayy machallah ❤️❤️❤️ Amal diamou rekk ndanane bi machallah 🙏🙏ags
Sénégal yafii dakk way srx ❤ nekh n'a lole la justesse de sa voix ❤❤
J'ai mis un 👍 avant même d'avoir écouter. Très belle chanson comme toujours.🤗
Merci infiniment
Mâcha allah néxxna tropp
Li nekhna trop bilahi ❤
Mo meun weuy kaay machallah, future Ministre de la culture l'intellectuel de la musique sénégalaise
dègeule lolou nekhe na deh
Abdou lesfiertesdestlouis et les fiertes de st Louis du Senegal et fière de vs
❤❤❤❤
Le 17 inchalla sonko rek
Notre abdou guitté gnoune kou beugueu Sonko rek gnou beugueula amoul lenene
Continuons à nous lutter seule la lutte liber jaam ci Sénégal 🇸🇳
Machala yalla yalla same la lo waye mou nekh
J'étais à la cérémonie mais tu es une grande chanteuse et encore tu es correcte et belle
MACHA ALLAH , TOUS LES PATRIOTES SONT FIERS DE TOI ET BONNE CONTINUATION.
Ay way soumay sétane clip mbalakh yi sama khélmi si Aziz dabala lay dém yalla nako yalla yeureum
Me patriote yi li gnewa n'a dé 3million abonnés pour Abdou Guité sèkh
Limay sentir si ay sons wame mane rk mako xame 👏
Merci d'avoir valoriser notre région ziguinchor
Tu as en même démontré la beauté de notre chère ziguinchor machala ❤❤❤❤