Yaw mii lire sama commentaire . Xam nani parfois yagui travers si moment you difficile mais magui lay nianal , yalnala yalla brom takhawou may la jaam ak tawfex téh ha motali say yéné ga téral say wadiour ❤Amal courage rek bagna décourager lep dina bakh inchallah waxal amine ✅✊🫵
Bo woyé mounekh 😊❤🎉Bo soloo mou rafét 😊Bo retané mou guena nekhati ,voix bi nak benen level la😘🎈😊🎉 l'un des meilleurs de sa génération 😊il ne fait aucun bruit mais chacun de ses tubes mérite un disc 👏🎉💯AGS😊
Un artiste doit être souvent lyrique mais sa mission principale devrait être l'engagement tu as bien fait vu la situation du pays cette chanson mérite des cœurs ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Damala mesa beugue depuis khalé mais jour Tabaski la wamouma nakh korité la gna djokh niou ndéwéna ma contant ne déme si sama kharite yi nane léne tonton Abdou guite seck dokh nama ndéwénal thie khalé 😂 yalla na sa diam yague❤❤❤❤❤❤❤❤
Que dire encore? Un artiste au-dessus de la mêlée. Il a décidé de mettre son art au service des hommes. Garant des valeurs de notre société. Il est talentueux, soucieux des difficultés de son peuple et constant dans ses combats. Bref! " Un gor" keuf yobou wou ko. Nous te portons dans nos coeurs, hier, maintenant et pour toujours.
Salut Abdou je suis abonné de ta page grace à un frère qui t'aime beaucoup qui s'appelle Baye Modou Diourbel il t'aime beaucoup me parle. Beaucoup de toi et tes chansons ms là je vois qu'il a raison machallah bis Nikki tay yay souniou chanteur
Mancha allah je tiens tellement à vous Abdou Guité seck, mais je réitère mes propos grâce à cette belle chanson que vous avez réservé au candidat du peuple Alioune Mamadou Dia 💚🤍💚🤍
Tonton Abdou guite seck a encore frapper l'homme du peuple l'homme ki n'a jamais perdu sa valeur machallah borom voix bi nekh bi depuis mn enfance ay son yam rekh lay deglou on es fier de vous chapeau et mes respects aussi ioe rekh lagniou toppou yalna sa diam yagu inchallah ❤
Elle est toujours à côté de population toujours égal à lui-même mon chanteur préféré bonne continuation le Sénégal a besoin de toi tout le monde entier beaucoup de succès mon frère❤❤❤❤❤❤❤❤❤
I called this kind of music " real generation music because he's talking about the present situations of Senegal, Gambia, and the whole Africa, the world at large 💯📌 abdou geiteh secka is a legend love from Gambia🇸🇳🇬🇲 ❤
Le téléphone à la main, les yeux rivés sur le clavier, je me dis : que dire encore d’AGS, à part qu’il a fait comme d’habitude ?? Quel meilleur commentaire lui apposer cette fois-ci ?? Franchement, chapeau 👍🏽🙏🏽. Et crois moi AGS ça donne des maux de ne plus avoir de mots sur le travail que tu fais. Abdou comme Artiste avec tjrs un grand A. 🇲🇷🇫🇷🇸🇳
Machallah 🙏🏿😍 Sama ndanaan kouli fadaliin bi très belle chanson et très beau clip vidéo, bien réalisé, une chanson très instructive lii lagnou doundou la vie est très chère Abdou Guité Yallah nala Yallah laffal thiat aar leu yiir leu tekk leu ci yonnou ci siratal moustahim gën werreul baat Amine Allahouma Amine 🙏🏿 Inchallah 🙏🏿
Machala yalna yalla weureul bat bi actualité rek gafi wakh nasa diam yague 500 mill takhoul say problème fadiou dakh leup mo chere metina lol yalna yalla dirigeants you ame yeurmander
T walahi doundou bi daffeu metti ba dès fois tu pense que ni ioe rk yaye doundou lou metti alos que ni fepp leu ko wo sax mou fokni dangua kay nianeu la vie est dure vraiment
Machala toujours a lui même frechemen chapeau a lui cène d'où môme magnifique clip aussi perfaumans aussi est aussi est la riyin n'a dire nous sommes fiyer de toi Say bo gen mou nekh laf chat Bon continuation notre Aboudou gîte seck❤❤❤
Machallah li mom nekhna trop et les paroles amna sens troppp abdou guittei yalla nala yalla Sam arleu longue vie et santé de fer ci barkei Seydina Mouhamad(psl)🙏🙏🙏🙏🙏
MACHALLAH MON CHANTEUR DE TOUS LES TEMPS UN HOMME DE VALEUR AME FOULA AK FAYDA YALLAH NALA YALLAH DÉFAL DIAM SI BARCKÉ SEYDINA MOUHAMED SAW GUITTÉ LAOBÉ LATY SARR
Yaa dakh wooy ci Sénégal loo wooy day am sens kou d'accord lalal j'aime
Yaw mii lire sama commentaire . Xam nani parfois yagui travers si moment you difficile mais magui lay nianal , yalnala yalla brom takhawou may la jaam ak tawfex téh ha motali say yéné ga téral say wadiour ❤Amal courage rek bagna décourager lep dina bakh inchallah waxal amine ✅✊🫵
Amine yarabi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏 2:40
Amine way❤🙏🙏🙏
Aminé
Allahuma amiiin y'a rabbi
Amine
Homme qui n’a jamais perdu sa valeur ❤❤❤❤❤
Bilay ❤
Bilay yaw
Bilay
Walay
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Pur💚🤍💚AMD 2024 le peuple est content🎉woooah damala meuseu beugg depuis xallé ms tay geunn neu yokkk barki Mame Cheikh💚🤍💚
Kou d'accord ni Abdou guité dafa meneu wayy lalal gaim
Bilaye
Bo woyé mounekh 😊❤🎉Bo soloo mou rafét 😊Bo retané mou guena nekhati ,voix bi nak benen level la😘🎈😊🎉 l'un des meilleurs de sa génération 😊il ne fait aucun bruit mais chacun de ses tubes mérite un disc 👏🎉💯AGS😊
Voilà un artiste celui qui pense aux difficultés de la population. Que Dieu te garde
Patriote leu motakh
Dotoko défati yaa doug si nioune💚🤍💚🤍💚🤍💚 tak ba faw rk
Yah dakh way si aduna biiii Gnoune ioe reik lanuy top
PUR AMD DOX JËM PALAIS💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚
Kene masouko dégue si lou niak fayda, yay souniou fierté Seck ❤🫶🏾
Un artiste doit être souvent lyrique mais sa mission principale devrait être l'engagement tu as bien fait vu la situation du pays cette chanson mérite des cœurs ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ana dém katou marché yi,bilahi doundou bi cher na 😢😢😢
Weuyy 😂
Bilaye l’enfant de st Louis n’a jamais perdu sa valeur 🎉🎉🎉
Waaa ana sougnou son bi nak
Aliou rk ba birr palais 🤍💚💚🤍
Son bi motakh ma abonné si yaw merci beaucoup vraiment
L'icône de la musique sénégalais... La fierté saint-louisienne.❤❤❤❤
Damala mesa beugue depuis khalé mais jour Tabaski la wamouma nakh korité la gna djokh niou ndéwéna ma contant ne déme si sama kharite yi nane léne tonton Abdou guite seck dokh nama ndéwénal thie khalé 😂 yalla na sa diam yague❤❤❤❤❤❤❤❤
« L’art pour l art c est bien , mais l art pour le progrès c est encore meilleur « je l aime quoi dama ko bouga man 😀, respect !
Il ne perdra jamais sa valeur l'homme de valeur ❤❤❤❤je t'aime beaucoup on me dit souvent que je suis raciste pas ce que j'écoute que Abdou guitte seck
Qui a écouté le après les élections 😅❤❤❤ Sonko moy diomaye
Naniou and dougal AMD palais lépou diéxe inchalla 🟢⚪️
Que dire encore? Un artiste au-dessus de la mêlée. Il a décidé de mettre son art au service des hommes. Garant des valeurs de notre société. Il est talentueux, soucieux des difficultés de son peuple et constant dans ses combats. Bref! " Un gor" keuf yobou wou ko. Nous te portons dans nos coeurs, hier, maintenant et pour toujours.
Si c'est PUR💚🤍 #AMD 2024 inchalla
Salut Abdou je suis abonné de ta page grace à un frère qui t'aime beaucoup qui s'appelle Baye Modou Diourbel il t'aime beaucoup me parle. Beaucoup de toi et tes chansons ms là je vois qu'il a raison machallah bis Nikki tay yay souniou chanteur
Mancha allah je tiens tellement à vous Abdou Guité seck, mais je réitère mes propos grâce à cette belle chanson que vous avez réservé au candidat du peuple Alioune Mamadou Dia 💚🤍💚🤍
Le meilleur musicien et parolier du Sénégal ❤🎉
Tonton Abdou guite seck a encore frapper l'homme du peuple l'homme ki n'a jamais perdu sa valeur machallah borom voix bi nekh bi depuis mn enfance ay son yam rekh lay deglou on es fier de vous chapeau et mes respects aussi ioe rekh lagniou toppou yalna sa diam yagu inchallah ❤
L'enfant de saint Louis bégué Nanou la❤❤❤❤
Walay l'homme ki n'a jamais perdu ses valeurs et ses racines❤
Abdou yalna bour yalla fay sa khôl nitt nittè ❤❤❤❤
Sam mariage bilahi yow reik yakoy woy dina liguey Bâ yor louma la fayei❤❤
Abdou Guité machalla bel.voix.ndeysane.wakh.deug.senegal
Metina.yalla.diapélé.senegalaise.ame.salam.téragan.dina.bakhe.inchala❤❤🎉
MashaAllah un vrai homme de valeur 💚🤍
Abdou guitte seck ak Assane mboup ak Titi ak wally seck Gni damalena beug ba awma thie niom sago soumay deglou seni son sama yaram bi dafay daw❤❤❤❤❤
Abdou la belle voix qui inspire qui motive merci 🙏 Ndanane ❤❤❤
Merci infiniment
Merci d’avoir gardé tes valeurs !
Elle est toujours à côté de population toujours égal à lui-même mon chanteur préféré bonne continuation le Sénégal a besoin de toi tout le monde entier beaucoup de succès mon frère❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam salam séckene bi dieureudieufati le grand patriote c'est vrai mêtina si yen ak diawene yi 😂😂😂
I called this kind of music " real generation music because he's talking about the present situations of Senegal, Gambia, and the whole Africa, the world at large 💯📌 abdou geiteh secka is a legend love from Gambia🇸🇳🇬🇲 ❤
Ndeysane dioy n'a sakh 😢 dou weuyeuntou je t'aime Guité Seck
Premier album que j’ai acheté c abdou gite seck ❤
"Coono Aduna": YALLAH naniou may louniouy soutourlo😢. YALLAH naniou atté akk nguur bii fii nékk😢.
Sama danane bi wakhatina bilay ya meune ya eup dolé si activités ak enseignement rék ngay wakh l❤❤❤
Nôtre Abdou préfère Leu wooyy mou nékh té ndiarigne leu machallah yallah neu bate bi geuneu weur ❤❤❤
Le parolier du Sénégal, s'ope nala Nguyen Sonko . Meun woyy❤❤n
Mâcha à la ❤❤❤❤❤❤❤Mâcha a la sonko rék inchala yalla ❤❤❤❤❤❤❤Nice massage Dam rék 2024
Loumou way mou am chance billay Sénégal 🇸🇳 dou réw🥹 merçi beaucoup à toi abdou Guité seck tu es un bon exemplaire 🎉🫡
Non mais franchement Macha Allah il a encore marqué son empreinte 👌👌👌
Un homme qui n a jamais perdu sa valeur
Le téléphone à la main, les yeux rivés sur le clavier, je me dis : que dire encore d’AGS, à part qu’il a fait comme d’habitude ?? Quel meilleur commentaire lui apposer cette fois-ci ?? Franchement, chapeau 👍🏽🙏🏽. Et crois moi AGS ça donne des maux de ne plus avoir de mots sur le travail que tu fais. Abdou comme Artiste avec tjrs un grand A. 🇲🇷🇫🇷🇸🇳
AMD rék senegal changer inechalla
Artiste pir abdou guitte seuke Sénégal keneu dakhola way marcha say achen son rek lay deglo❤
Lou ler nga wakh
Lou ler nga wakh ma tegal thie dara yarou dall bakh am respe si doumou adama yi
machalla papeu guité deck a encore frappe li la ham ci porteur de voix mais né patt rek mouy nex ci yaw rek nga faté peuple ❤
Abdou guite seck il chante tres bien❤❤❤ machalla
sama artist prefere mala begue ❤❤❤
Way kate mi ngui beug diekh Sénégal 🇸🇳 ay tasou kate nio fi dès dhè
J'abonne pour Alioune Mamadou Dia pur ❤
Sama tourondo l’afthiate reck je jure tu est la meilleure de ta génération on love ❤
Machallah 🙏🏿😍 Sama ndanaan kouli fadaliin bi très belle chanson et très beau clip vidéo, bien réalisé, une chanson très instructive lii lagnou doundou la vie est très chère Abdou Guité Yallah nala Yallah laffal thiat aar leu yiir leu tekk leu ci yonnou ci siratal moustahim gën werreul baat Amine Allahouma Amine 🙏🏿 Inchallah 🙏🏿
Merci infiniment
Big respect le Saint luisien.AMD predident2024❤
Ah merci Abdou Guitté seck pour cette belle chanson qui relate tous les maux du pays.
Merci Mr Seck, c'est ce qu'on attend des porteurs de voix
Aye cœur ♥️ waye thi chanson bi khamo ligua weuye sakh machalla ❤❤❤❤❤❤
Véritable voix du peuple ✅✅✅✅
Machallh nit kouma meuss beug depuis 2002 balegui Moy sama woykat❤❤❤❤❤
Kii labeug mane❤❤
Voté pour DETHIE FALL la solution de passage merci ABDOU GUITE SECK
Machala yalna yalla weureul bat bi actualité rek gafi wakh nasa diam yague 500 mill takhoul say problème fadiou dakh leup mo chere metina lol yalna yalla dirigeants you ame yeurmander
T walahi doundou bi daffeu metti ba dès fois tu pense que ni ioe rk yaye doundou lou metti alos que ni fepp leu ko wo sax mou fokni dangua kay nianeu la vie est dure vraiment
Oh ndeysaan❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤.je l'aime depuis mon enfance❤❤
Machine meilleur de sa génération dam ko beugou bilay 🎉
Machala toujours a lui même frechemen chapeau a lui cène d'où môme magnifique clip aussi perfaumans aussi est aussi est la riyin n'a dire nous sommes fiyer de toi Say bo gen mou nekh laf chat Bon continuation notre Aboudou gîte seck❤❤❤
Bilay ya meune way liga way sougnou candidat bi nékhna way ga kou mata way
Abdou guitté seck, un grand artiste et il est très fort machallah ❤ longue vie à toi mon frère seck
Merci merci beaucoup adou Guita❤❤❤
Excellent travail mon rois. Le rois du mbalax. C'est le digne fils et grand patriote tous derrière toi le meilleur machallah
Un vrai Artiste engagé Big Respect Abdou 🫡✊🇸🇳
Machallah li mom nekhna trop et les paroles amna sens troppp abdou guittei yalla nala yalla Sam arleu longue vie et santé de fer ci barkei Seydina Mouhamad(psl)🙏🙏🙏🙏🙏
Baakh-a-baakh na! Dieureudieuf, Abdou Guite Seck, doomu Ndar!👍👍👍
MACHALLAH MON CHANTEUR DE TOUS LES TEMPS UN HOMME DE VALEUR AME FOULA AK FAYDA YALLAH NALA YALLAH DÉFAL DIAM SI BARCKÉ SEYDINA MOUHAMED SAW GUITTÉ LAOBÉ LATY SARR
Machalla vidéo Abdou 🥰✊👈
Chapeau à vous
tjrs dans l'actualité
La vidéo AMD PUR foumou toolou
Thia kaw thia kaname rek machaallah
Toujours au top niveau machallah, merci pour ça ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Seck ndanane lo déf mou nékh ❤❤❤❤❤
Merci beaucoup mp' idole❤❤
Sonko ❤❤❤❤❤✊🏽🇸🇳🇸🇳
Abdou I really love your music 🎶 your fan from the Gambia 🇬🇲 ❤️
Tu est le mieur❤❤❤
Machallah amna solo lol AMD PUR président du Sénégal inchallah ❤️
Mon chemin, thiono aduna, doundou day wess, aladji.... Et maintenant celui-ci dans ma playlist. Guitté un des meilleurs
Saint-Louis et fière de toi 🎉
Merci gar ferr❤❤❤
Max de partage. We support patriote 👊
Lowy monekh dagua way sono wadji AMD 💚🤍 pur
Bilahi ki mo mana wayy 🎂🎂
Du lourd encore meilleur que jamais Abdou guitte
MachAlah sûnû GUITË..🎙️ L'ARTISTE COMPLET 🎧🎹🥁🎻🥰🩸🎗️ LOULËRR SAKH GUA WAKH
Ndeysanne le parolier quand je t’écoute j’ai la chair de poule ❤❤❤❤ya meune Machallah, bon vent 🥰
Merci vraiment