Merci beaucoup pour la version en Français 😁j' avais tellement hâte de comprendre.Je suivais certaines de vos recettes sans malheureusement comprendre si ce n'est qu' en suivant les images. Si possible de continuer ainsi , c'est un plaisir de regarder vos plats et d' apprendre à les cuisiner.
Maa chaa Allah walaa khouwewata ilelaa bile Laah. Tata Mariétou par force lay saf in chaa Allah avec tous les youubou yaaba . Yalla mayela wér ak wérlé defalela Tawfeex bijaahi sayyidile woujoude psl. Encore Merci🥰🥰🥰🥰
Di fatéliku jamano... Pensées douces pour ma regrettée Maman. Yekkal ci Tabaski. Merci Maman. Merci Mariétou (tous ces parfums, toutes ces images qui me reviennent, jusqu'au séchage de la semoule au soleil... avec son petit morceau de charbon!). Yala na ñu fekke ay Tabaski yu bare bare! ñu fi nekkatul, Yala na leen Yala yerëm, ibbil leen bunti Aljana! Amiine ya rabbi.
Bee mom, law la thiate. Keurigne bi gnou Dane foroholé thieré bi, môme la mame boye dane dèfe. Merci! Tu as vraiment toutes les astuces du temps de mon enfance, une belle recette traditionnelle sénégalaise.
Sa dieukeur ma demande de cuisiner le thiere pour la fete dachoura, il ne cesse de me demander ndakh meune na thiere ma nane ko sii, te khamne bouma kheye setanii tata marietou. Tata, Ya niou sagal nioune new generation bii. Love you dear Aunt!!!
Madame Seck machalla les salis sa me rappelle ma ville Saint Louis du sénégal trop bon haaa !!! Salie dingua khamé ndahk goût moi vraiment je te souhaite une longue vie de santé
4 ปีที่แล้ว +1
Merci ma chérie et c’est Tata Marietou et non Mme Seck merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😂😂😂🤣
Masha Allah tata Marietou merci beaucoup ci plat bi ak viande selé et sécher bi goût bu nekh la masha Allah yangy may fataly lu yaag on le faisait ... wala gha déf ko ci mafé oubien dekhine bénén affaire la Yalla na yalla goudal say fane mayla weur ak weur lé😘😘😘
Salem aleykoum j'aimerais bien une petite traduction en français en général pour toute les recettes car j'aime votre cuisine et j'aimerai la réalisé merci 👍
Tata merci dieuredieuf pour tes belles recettes ! Est ce que tu peux faire la recette du fouto do déré/lacciri e haako, la semoule de couscous avec la sauce epinard/poudre de cacahouete. Je reve de la faire
Bilay ki nimako mere tey mane Ndiaye te ga bayi provocaciones bii machalla Yalnako barkel presentación rafetna dee
Bonjour tata je viens de découvrir votre chaîne et j'aime beaucoup ce que vous faites et surtout les commentaires 😂. Merci beaucoup vraiment
Ohhh merci ma chérie y’a pleine de bonnes choses ici il faut juste prendre le temps qu’il faut and you will loveeeee it 😂😂😂🙏🙏🙏🙏
Machalla tata ziar nala wenibik gnanal la diam di contente thi yaw wenibik
Yow deih saloum saloum nga 🥰 Thieirei diou forokh mom Saloum la thiossaanoo ! Le Sénégal un beau pays et riche par sa culture Machallah
Aah thioum thiere mon ami non tata bayil liguay def waye 👍😋😋😘
Merci beaucoup pour la version en Français 😁j' avais tellement hâte de comprendre.Je suivais certaines de vos recettes sans malheureusement comprendre si ce n'est qu' en suivant les images. Si possible de continuer ainsi , c'est un plaisir de regarder vos plats et d' apprendre à les cuisiner.
laemka Bondo merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
@ à bientôt. 🙏🏽
Oui vraiment
Maa chaa Allah walaa khouwewata ilelaa bile Laah. Tata Mariétou par force lay saf in chaa Allah avec tous les youubou yaaba . Yalla mayela wér ak wérlé defalela Tawfeex bijaahi sayyidile woujoude psl. Encore Merci🥰🥰🥰🥰
Thiere ti gua Thiey tata marietou machalah. Khara ma nopi fi da ame aye ndiayene
Manchalla man mom damala beug trop merci pour la recette 😘😍😋
Jaar n'a yoone, ingredients yi yemna, chapeau🇸🇳🇸🇳
Machalah ziar bou wer Tata Marietou thiere tamkharite anticiper valide laf thiat 🙏🙏❤❤💯💯👏👏
Di fatéliku jamano...
Pensées douces pour ma regrettée Maman.
Yekkal ci Tabaski.
Merci Maman. Merci Mariétou (tous ces parfums, toutes ces images qui me reviennent, jusqu'au séchage de la semoule au soleil... avec son petit morceau de charbon!).
Yala na ñu fekke ay Tabaski yu bare bare!
ñu fi nekkatul, Yala na leen Yala yerëm, ibbil leen bunti Aljana!
Amiine ya rabbi.
Amen Amen Amen que leur ames repose en paix et courage ma Soeur te yalla tek loxo diabot bi yeup
Ohhhh😍😅 say khétou terme tamit meune nama ray🤣 merci du partage
ana gni commente balagno tegarder la video ndak contane machallah
Maman maretou lay don ha narou mère Diop sa tieré bakhna 😘😘😘😘😘💖💖💖💖💖💖👍👍👍👍
Mashallah merci bcp tata Marietou Yallah reek mola mouna fèye 👏👏🤲🤲🤲
D’accord ba thia talalé ba yaapou thiéré
Après tamate lay nieuw niafff 🥰🥰🥰
Salam aleykoum tâta Marietou foneke namenaloulah lou Barry machaallah
Manchallah yalla na lokho bi wer❤️🥰🙏
Merci tata Marietou tu nous aide tellement on t'adore fort
Thiey!! Sa dieukeur mom affairam bahne. MANCHALLAH
Bee mom, law la thiate. Keurigne bi gnou Dane foroholé thieré bi, môme la mame boye dane dèfe. Merci! Tu as vraiment toutes les astuces du temps de mon enfance, une belle recette traditionnelle sénégalaise.
Sa dieukeur ma demande de cuisiner le thiere pour la fete dachoura, il ne cesse de me demander ndakh meune na thiere ma nane ko sii, te khamne bouma kheye setanii tata marietou.
Tata, Ya niou sagal nioune new generation bii.
Love you dear Aunt!!!
Machallah tatie chérie longue vie Mariétou bismilah thieré bouy tokh tokhi déye nékh ba eupeu dolé 🤣🤣ni gua koy diokhé rék dafa ame solo diarna lékeu baye rame merci un gros bisous 😘😘😘
Machalha tata marétou merci yalna yallah faye👏👏
Machala tata Mariétou namatouma thiéré tamkharite. Sa bassi salté bi diarna yone. Yalna sa diam yagg ma chérie 😘😘😘
Wa Maman khana ndar ndar ngua Macha allah
Vraiment merci. Cette chaîne me rappelle trop mon enfance à kaolack. Dès que je suis nostalgique je viens la.
Merci du partage !
Ma sha ALLAH Tata Marietou thiere bi môme diar na yone mais say assiettes niou ma danel 😘😘😘
Tata Maretou rek gnak laa kham woroul, Que Dieu te bénisse
Madame Seck machalla les salis sa me rappelle ma ville Saint Louis du sénégal trop bon haaa !!! Salie dingua khamé ndahk goût moi vraiment je te souhaite une longue vie de santé
Merci ma chérie et c’est Tata Marietou et non Mme Seck merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😂😂😂🤣
Mâcha la nekh n’a weliiiiiiii👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾
As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH nooo tata mane daal suis fan kw mashaal'LAH 😍
Masha Allah tata Marietou merci beaucoup ci plat bi ak viande selé et sécher bi goût bu nekh la masha Allah yangy may fataly lu yaag on le faisait ... wala gha déf ko ci mafé oubien dekhine bénén affaire la
Yalla na yalla goudal say fane mayla weur ak weur lé😘😘😘
Ma chaallah, thiéré bi nekhna, amal Jam 🙏💐🥰
Tata marietou yalla nale yalla faye yiw. Merci
Tata yalna diamou yague thi barkeb khassida yi 🥰🥰🥰
Ha bi bassi salte tochna machala depui Mekhe
Machalah tata mariata magnifique comment tu cuisine waw ✅✅🙏🙏🙏❤
Tata marietou mangui laye beugue bou baakh sakh yallnala yalla defal diam borome youbi yaabaayiii 😘😘🤣depui italia
Mashaa Allah yalna sa jamma yagg
Le fameux téérébiein❤
J’aime trop vos recettes Ma Shaa Allah!🤲🏾💕💕💕
Wa goor itali gnogui lay gerem😂😂
Oh magnifique tata Mariètou
Mane ma beugue sa façon toggou doundeul Waay yaboye
Machahlla laf thiate tata
Saliiiiiuu gnibko xam bariwoul namenagn la
Tata Mariétou darling machaAllah mane mi sama yaye dafay sali🥳😍❤️🎉 oh 😍 bobou goût machaAllah 😁! Jazakalahou khayrane diaratina yone machaAllah ❤️😘🥳😊😚
Très bien machalla7 na résse ak diame
Merci pour la version française 😍
Machallah merci pour le partage
Machallah tata Mariétou merci pour le partage
Thioo Tata thiéré gua 😍😍
Hi Tata Marietou, I hope you are doing okay. We missed seeing your videos and hearing your voice. Yalnala Yallah defal diam ❤❤❤
Merci tata mariétou tous les youbiyabas sont là 🤩😍😍😍🤣🤣😘😘
Masha'ADHWAHU !
Maman si vous pourriez préparer pour moi serait très merveilleux.
Un Comorien à Dakar😁😃
Ma cha allah amatina solo
Machallah safna ba yegu si sap😂❤️
MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH
Mashala naixatina😍😍😍 tata laxass yi moy tripe de mouton wala de boeuf
Très bien 😊🤣👍🏾
Mashaallah tata 💜 ♥
Bravo bonne appétit
Merci pour la version en français tata Yande
Liguay wakhé nehnama
Merci tata d avoir expliqué la recette en français, vous êtes géniale.
😘😘😘😘😘😘❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tata @marietou il faut sous titrer (subtitle) ça évitera de répéter en français 😍😍😍 en tout cas merci.
Merci madame efficace et savoureux
Machala
Wonderful
Do you have the translation of the ingredients please
Thank you xx
1er vue dou aie foo
Machalla tata merci
Salem aleykoum j'aimerais bien une petite traduction en français en général pour toute les recettes car j'aime votre cuisine et j'aimerai la réalisé merci 👍
Tata merci dieuredieuf pour tes belles recettes ! Est ce que tu peux faire la recette du fouto do déré/lacciri e haako, la semoule de couscous avec la sauce epinard/poudre de cacahouete. Je reve de la faire
Medinah Janna th-cam.com/video/HmGxz0f-i6c/w-d-xo.html.
Medinah Janna salut please suivez ce lien 👆🏿👆🏿👆🏿 merci
Merci beaucoup ❤❤ j ai hate de la faire
Machãllãh 💕💞💞💞😋🙏❤️
Manchalla
Très bien ❤️😂
Bonjour je voudrais savoir comment faire le sali merci
Hi Tata I want to no where do you get the birou lamp
Tata marietou diokh ngama envie leek thiere taye🤔🤔
Ooooh....😴😴😴
Machallah
Merci Marietou sama khel mingui ci viande salée bi . mais pourquoi tout le monde met du sucre dans le thiéré??
Masha allah sougnou tata marietou Ken d'où yawww😘❤️
Tu est adorable Marièthou
Masha Allah ❤️❤️❤️❤️
It looks delicious
Setanagouma sakh waye maynala baramou kaw gui.
manchallah
Waw tata fo RER ???
Ma cherie Alhamdulilah mangui thi diama dama khawa diap rek mais insha Allah tres bientot rek nguen guissate ma merci wayyy ❤️❤️❤️❤️❤️😘😘😘😘😘
Nonou lalay khalate tata❤️❤️❤️❤️
❤❤❤ haaaa tata mariétou j'ai particulièrement réfléchi mais je trouve pas un mot à justifier merci🙏🙏🙏
Très bien merci beaucoup maman
Barkiii alkhouranneeeee💯💯💯💯💯
Thieye maman bo publié rek kholi séd
Aah Tata Marietou Senegal niogui Sali batay dei. Tabaski gnou dff Sali dinthi, bougnuy deukhine mafé bassi salté neiko ci reill😅
Mane dal yow lay weur tata keen dou yow
Très bien 😁
neko ci touy😅😄
Coucou Madame, je fais mon couscous samedi, le sucre c'est pourquoi ? J'apprends. Merci. Bonne fête 2020.
Bonjour Bineta camara, le sucre donne un bon goût
@@soniasall3223 Merci. Je vais essayer sur une part. Merci.
Merci beaucoup tata ❤️❤️❤️❤️