Salut j abite a yeumbeul je connais bien daouda car il frequentait dans la salle de miscalculation qui etait devant notre ecole rennaissance mais ceux qui me fait mal c est que le maire a continuer les festives le lendemain Vraiment c est irespectueux
@@bettynawelmbaye ndeysane merci Adouna amoul solo insha'allah bi tamla rek t Mouy Lou bakh si diam ndax yalla mo mom aljana nam masha'Allah bouko sobé rek mo dougal si diam ndeysane
Inna lilahi wa inna illayehi rajiouna Fête bi concerné woula an tant que musulman ga difa dém si ayé thiakhan ba sa bakan difa dess yalla nanou yalla yerem doyna war metina
Inna lillahi wa Inna illeyhi rajahoon yalla nako borom bi yeureum tei diegeul ko🙏🏼 mais boulén niak ba paré di nianki yalla moko dogal lou warone am la sante len yalla
C'est honteux. Manque d'organisation ak barbarie bih am senegal c'est incompréhensible. A chaque fois que mou am événements fook mou am scandale. Mais kagne laliouy organisé. Kholal ki likodal rek té mounone niak. So wakhé nioulay nane . Heuram mo diott. C'est vrai yallah dafay dogual mais nitt dafthi am part de responsabilité. Soyons honnête et qu'on se dise la vérité. Vraiment li mounone n'a niak ca me fait mal quand je vois des gens perdre la vie dans ces choses stupide
Mane boye yiye nek si mbed yi di tiré ay petard gno wara areté li dara woroussi senegal lou gnew gnou eupeull sii 🎉 mai boye daouda yala nako yala yeureum
Un maire irresponsable organisé une fête qui te concerne même pas en tant que musulman le comportement de certains officieux de ce pays me fume mais le jour du jugement vous rendrez des comptes اللهم ارحمه و اغفر له 🙏
Det way kou bakh ndogal la rek nianal ko rek souniou borom diégal khamna il voulais faire plaisir à sa jeunesse de son quartier mais boussi accident amé nak menons naniou arrêté nak
Vous dites que le Maire est irresponsable pour organiser une fête qui ne lui concerne pas parce qu'il est musulman mais le jeune Daouda aussi est musulman qu'est-ce qu'il faisait la bas.paix à son âme
Séne bi kou irresponsible la kome féte ame na ba bakane rot thi kaye arétéléne fo bi wa Cartier bi nio niak faye da rék bougne léne fa fékone ak aye khér dinagne tal lénéne loudoul aye fo makhala maire you fi ame yép nioko ték sounou bop
Yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana, Maire bi aussi organisation bi dafa dese diaar yone pitard dafa am yone, mais la famille aussi legui yen loleni xaar si Maire bi danguen beug ndampaay wala ?
Quel événement tragique. La mairie a eu un comportement méprisant voire irresponsable. Faudra porter plainte pour faire condamner la mairie même si ca sera symbolique. Le respect de la vie de humaine est inexistant au Senegal.
Qui dirige assume ses responsabilités !! Ndjitt daguay Matt ligua done ! Comment une fête peut continuer sur les lieux où un être humain a perdu la vie ? De l’irresponsabilité et du je m’en foutisme
😢Bilahi ni lako wakhé pétard yi ma guiss jourou 31 décembre comme ay bombe koumou dal di nga am problème deug sinon Yallah nako Yallah yeureum té xaréko aldiana 😢😢😢
Inna LillAhi Wa Inna Illeyehi rajiouna mais ça c'est triste et alarmante YALLAH nacko YALLAH yereum té kharécko Alejana Mais khana Maire bi dou père de famille événement bobou si heure bobou lagniecko warone dakale bakane da fort c'est très grave
Pétard doumako meussru diaye mo dalone thi sama beutou dom il a fallu perdre la vue j'ai depensé bcp d'argent pour le soigner pétard bakhoul cété un 24 décembre
Chercher un bon avocat Me Bamba cisse, Me Moussa Sarr, Me Abdinar Ndiaye, Me Ciré Cledor LY vraiment cest normal le maire est responsable ne me dit pas homicide involontaire
Mane li damako ragal moutakh fouma kou deug damay daw Sorou 31 magui si keur ki wayy bonio kou talle day melni si keur ki lanio tall dama daw ba sama lokhou bi fakhathie nanio bayyi pital yi
Non mais vous abusez quand même il y’a négligence franchement. France niofi dakk tall pétard té ken doussi dé. Ne soyez pas des moutons li dafa niaw. Je parle à la famille n’acceptez aucune somme venant de n’importe qui que ce soit le maire où je ne sais qui. Collez lui un procès au cul 🤦🏼♀️ n’importe quoi que des sauvages ces cons
Ce père de famille est très responsable, tellement rare. Il faut aller jusqu'au bout.
Salut j abite a yeumbeul je connais bien daouda car il frequentait dans la salle de miscalculation qui etait devant notre ecole rennaissance mais ceux qui me fait mal c est que le maire a continuer les festives le lendemain
Vraiment c est irespectueux
Paix à son âme 🙏😭 que la terre lui soit légère et que le bon dieu l'accueil dans son paradis céleste 🙏
Ndeysane daouda Diouf demegua ni rekk yalla n'a yalla yeureume 😢
Paix à son âme que firdawsi soit sa demeure eternel 😢
Amine ya rabi ak bep dioulite si barké Alhourane ❤
Li métina trop billae Sama toma yalla nala yalla yeureum té kharéko aldiana firdawci si barkep Mouhamed Saw Psl Amine
Paix à son âme Ndeysane non mon Dieu 😭😭😭😭😭😭😭❤
Oh ndeysane paix à son âme yalla bou soxla rek niepay niak yalna ko yalla yeureum insha'allah xaré ko aljana
Nga balma dé ñian🤲 kén doussi bolé insha'Allah
@@bettynawelmbaye ndeysane merci Adouna amoul solo insha'allah bi tamla rek t Mouy Lou bakh si diam ndax yalla mo mom aljana nam masha'Allah bouko sobé rek mo dougal si diam ndeysane
@@kharyfall5186 Diam ci iow🤝
yalnako yalla yeureum te khareko firdawsi
Inna lilahi wa inna illayehi rajiouna Fête bi concerné woula an tant que musulman ga difa dém si ayé thiakhan ba sa bakan difa dess yalla nanou yalla yerem doyna war metina
J espere que togguo reer rek jour bobou
yalla nako yalla are all diam
Billay l'islam loumou téré rék amna lou tah xolal li rék di fêtes lo mo moul ba ray thie domou diambour li niaw na trop yalna ko yallah yeureum 🤲🤲😭😭
Ngene arrêté guinar yi ngene di togg aussi ak kdo yi nkene diokh khalé yi ndakh lolou yeup cii Noël le bok..yene da nkene dof cii lima yakar
Yalnako yala yeureum si barki yonenti bi salalahou aleyhi wa salam
Inna lillahi wa Inna illeyhi rajahoon yalla nako borom bi yeureum tei diegeul ko🙏🏼 mais boulén niak ba paré di nianki yalla moko dogal lou warone am la sante len yalla
Yalnako yalla yeuram té xaréko aldiana
Que firdawsi soi sa demeure éternelle amiine yarabi 😢
Mem sou dewe woul won si fete bi sah rafetoul deuil ayy gay musique lolou momm dou hell kogn bou am deuil hew boufa amon sah dougn continue
Notre DAOUDA est parti à jamais 😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Thiey Senegal 🇸🇳 liggui Rey rekk 🙏
Qu'allah lui fasse miséricorde et lui accorde le paradis.
Que le terre soit légère sur daouda Diouf😭😭😭
Ndéysane vraiment métina trop bilahi yalla yeureum ko amine way 😢
C'est honteux. Manque d'organisation ak barbarie bih am senegal c'est incompréhensible. A chaque fois que mou am événements fook mou am scandale. Mais kagne laliouy organisé. Kholal ki likodal rek té mounone niak. So wakhé nioulay nane . Heuram mo diott. C'est vrai yallah dafay dogual mais nitt dafthi am part de responsabilité. Soyons honnête et qu'on se dise la vérité. Vraiment li mounone n'a niak ca me fait mal quand je vois des gens perdre la vie dans ces choses stupide
Yala nako yalla yeureum si barké alkhourane
Mane boye yiye nek si mbed yi di tiré ay petard gno wara areté li dara woroussi senegal lou gnew gnou eupeull sii 🎉 mai boye daouda yala nako yala yeureum
Massa Paix à son âme
Yalla na yalla yeureumko kharerko aldiana firdawsi ya rabana😭😭
injustices bi nek senegal 🇸🇳 OUSMANE SONKO rek mokofimena dieulet loulerre la❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalnako bour yalla yeureum te dièguelko kharèko si aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲
Un maire irresponsable organisé une fête qui te concerne même pas en tant que musulman le comportement de certains officieux de ce pays me fume mais le jour du jugement vous rendrez des comptes اللهم ارحمه و اغفر له 🙏
Det way kou bakh ndogal la rek nianal ko rek souniou borom diégal khamna il voulais faire plaisir à sa jeunesse de son quartier mais boussi accident amé nak menons naniou arrêté nak
Ndeyssane yalla nalene yalla may kholou mougne tè khalei bi yalla khareko aldjana firdawssi amine
Vous dites que le Maire est irresponsable pour organiser une fête qui ne lui concerne pas parce qu'il est musulman mais le jeune Daouda aussi est musulman qu'est-ce qu'il faisait la bas.paix à son âme
Séne bi kou irresponsible la kome féte ame na ba bakane rot thi kaye arétéléne fo bi wa Cartier bi nio niak faye da rék bougne léne fa fékone ak aye khér dinagne tal lénéne loudoul aye fo makhala maire you fi ame yép nioko ték sounou bop
Toi tu es musulman mais khamo Dara sisseu religion car tu blasphème question de religion tey deussè bakhh.
Yala nako yala yeureume té haréko aldiana
Yala na yala May yayam kholou mougn
Massa que son âme repose en paix 🙏
Wakh deugy YALLAH moi je suis choquer
Yalla na firdawsi di kereum yarabi 😢
Yal nako yala khare aldiana
Yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana, Maire bi aussi organisation bi dafa dese diaar yone pitard dafa am yone, mais la famille aussi legui yen loleni xaar si Maire bi danguen beug ndampaay wala ?
Yala nako yala yeureum amine yarabi
Yalla na ko yalla yéréme té kharé ko aldiana firdawsy
Il n'y a pas de mots pour qualifier le comportement de ce maire.
C très grave
Son première fête Andi mort Babacar ndao mo amoul dieurign si yeumbeul nord
Repose en paix 😢
Ce maire est irresponsable et inhumain . Paix à son âme
Mane dama rousse entake domi yeumbeul monsieur le maire Babacar ndao ak équipe municipale bi dioume nanou 😢😢😢
Yal nako yalla yeureum té kharé ko sa Aldjanay firdawsi ya raby
Quel événement tragique. La mairie a eu un comportement méprisant voire irresponsable. Faudra porter plainte pour faire condamner la mairie même si ca sera symbolique. Le respect de la vie de humaine est inexistant au Senegal.
Bilaahi metina
Maire bi ga hamni defoul Dara si commune bi
Ndeyssan yo allah yourmomo yaffomo harnamo aldjana firdaws amine ya raby
Paix a son âme …rak bou yarou 😭😭😭meittina trope sah
C'est vraiment triste paix à son âme
K firdawsi soit sa demeure éternelle mon frère
Yallah nako yallah yeureum
Ce qui se passe au Sénégal avec les pétards c'est trop il faut le gouvernement interdit
Senegal dou reew yalla nako yalla yeureum ta diegeul ko 😢😢😢😢
Thiey adouna meti yagna am ma yay dji moma dioylo
Soubanalah Maire.bi.mom.Nitt.là.😢😢
Qui dirige assume ses responsabilités !! Ndjitt daguay Matt ligua done ! Comment une fête peut continuer sur les lieux où un être humain a perdu la vie ? De l’irresponsabilité et du je m’en foutisme
Yalla nako yalla yeureum té kharé ko Aldiana firdawsi 😭😭
Thièye Sénégal fomou dieume ohh c'est un Maire irrespectueux et irresponsable
Paix à son âme
paix à son âme 🙏🙏🙏
Ho masa😢yala nako yala yeuram té khareko aldiana firdawsi
Ndeysane paix à son âme
Yallah na khipé aldiana firdawsi 😢😢
Paix à son âme.
Khana maire bi wa Pastef la😢😢😢😢 amounou khol dé😢
Bilae
Yow Yay ndeyou nafekh gni niak yermadé fi khamgualenn bou bakh Mouy wa état gua nek fii Di doull
Macky firawna Sall mon geuneu niak ndeyi khôl domoukharam dji ❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌ yalla khareko aldiana ♥️
@@momathniass5720 kholal domouram dji mom
😢Bilahi ni lako wakhé pétard yi ma guiss jourou 31 décembre comme ay bombe koumou dal di nga am problème deug sinon
Yallah nako Yallah yeureum té xaréko aldiana 😢😢😢
Yalla nako yalla yeureum
Inna LillAhi Wa Inna Illeyehi rajiouna mais ça c'est triste et alarmante YALLAH nacko YALLAH yereum té kharécko Alejana Mais khana Maire bi dou père de famille événement bobou si heure bobou lagniecko warone dakale bakane da fort c'est très grave
Li motax tjrs manam Sénégal dou rew😔
Fi holland rewmi toutab ils ont interdit les petards alors au Senegal paye musulman sans interdiction c honteux .paix a son ame
Le Sénégal c est un pays musulman depuis quand???
on demand a se que le maire decision immediatment
Maire bii dafa warona demissionne wallahii
Non limou warone déf moy arrêté activités yi taxawou famille bi bakan dafa fort wayé yalla gueumoul nélawoul
@@nobasiby9540 Waw waye kom defoul lolou amul ben yeurmande sii nitt ak respect meritowul maire binko denk dafa waron demission s'il avait la honte
Il faut porter plainte
Lokhame si kou niak diome maire boubou d'où maire boubakhe
Massa paix a son âme.szsr troo triste
Bayilén disétani ay thiaxan
Masta qu il repose en paix Putin 😢qui matoul Maire 😢un Maire irresponsable 😭😭😭il faut porté pleine li dou yon loulen yone may nguen dieul
Vraiment le maire est irresponsable.
Vraiment Sénégal dou reuw, s'en mère bi deugeur na bop trop li dafa nianw thi Sénégal
la solution set sonko akh AK yelefou domou adama mome sonko daka doude ta balegui mome laye ndound .. LI METINA DIOUF
La voie #yoonwi
Ndeysane paix à son âme 😢😢
99.99 % de Domeram💔💔💔
La ou il ya mort d'homme on continu de faire la fete c'est inhumain sa ho xamétouma sama réw
Maire bii d’où nitou Dara
Pétard doumako meussru diaye mo dalone thi sama beutou dom il a fallu perdre la vue j'ai depensé bcp d'argent pour le soigner pétard bakhoul cété un 24 décembre
Jeune quartier bi dagno wara tall keureum
Masta
Chercher un bon avocat Me Bamba cisse, Me Moussa Sarr, Me Abdinar Ndiaye, Me Ciré Cledor LY vraiment cest normal le maire est responsable ne me dit pas homicide involontaire
😭😭😭😭😭
Paix à leurs
C'est dure de perdre un proche mais Ce gars nitou fitnala wakhou diakhassé rek lafit tenir.opposant la rek.prions pour le repose du jeune Daouda
tu a parfaitement raison merci
Yaw doul pouvoir bi gno ray ndeyi jeunesse sou Sénégal yeup ❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌
Bougniou ssi yarone sa baye do wakhé ni
D'ailleurs il ne mérite meme pas ce nom
Loutakh senegal niou niewer tall ay perard chimm decoration reck doyna ,
Mane li damako ragal moutakh fouma kou deug damay daw Sorou 31 magui si keur ki wayy bonio kou talle day melni si keur ki lanio tall dama daw ba sama lokhou bi fakhathie nanio bayyi pital yi
Li sacrifice d'ONG la
😢😢😢
Es ce que dioulite la
Loulou moy bonne
Mais quelle maire sauvage
Dakarbuzz svp outiléne programme mo gueune
Niak guéne khorom trop
Yaw bou sa baye déwone lo wakh li fuck 🤐
Tiré wougn ko ball dorougnouko ball donc boudoul ndogal lanla tmt metina mais geum len yalla
Kéne wakhoule dou doguale mé waronena meuneu annuler programme dakh bakane mo geuneu fort
@mbenyedieng2298 yalnako yalla yeureum masta courage
Bougn rayone seu nday waleu seu baye digua kham louy nite kou déh.
Non mais vous abusez quand même il y’a négligence franchement.
France niofi dakk tall pétard té ken doussi dé.
Ne soyez pas des moutons li dafa niaw.
Je parle à la famille n’acceptez aucune somme venant de n’importe qui que ce soit le maire où je ne sais qui.
Collez lui un procès au cul 🤦🏼♀️ n’importe quoi que des sauvages ces cons